Merci de la dedicace sister marietou. Dila bégué sassouné recettes yi am naniou solo et ton humour j'adore🤣🤣🤣 c'est madioula domou ndeyou soda depuis lyon
Bonsoir marietou namele mon école n'était pas fin mais je suis chaque fois, diakatou a sa place ici ça c'est sauce gordjigen mon frère déteste cela mais moi j'adore merci pour ces plats. Bisous. Mbahale dey saf sape plus citron
@@adamaisse pour mw tour bi mooy feeling bi parceque au temps si tu disais m'bakhalou guoordjiguéne laaye togue nieupeuye khaaraanesi !!!! Muuuuuuh dakh la mou saf eupeu na.
Aye tata marietou yeuremal Ndeye Coumba yi sonnananiou Mane de mm souma amoul ingrédients yup dinako lidieunti founekk ba tokk gouko. PS merci pour la recette
How do you make the green sauce in the bowl that is shown at the end
Год назад
Hi my Dear It’s spinach and okra lemon or lime juice salt and hot pepper so you will have to boiled them all in the same pot til they all cooked then put it in a blender til you get that paste it’s simple yet delicious enjoy
Très bien ! 💗💗💗 Sama yaye nena li mo bakh si santé. A propos de thiebou tir, ça ce fait en Casamance, ñoul tir bi comme sauce graine ivoirienne bi, xi ngay soor xa tieb. Avec tout les youbi yaba 😅, yokhoss etc.
5 лет назад
MaryYehosef ohhh ok merci ma Cherie dina thi def ay recherche Insha Allah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘
🤣🤣🤣Elle me tue Ma Shaa الله... Tu es superbe, ton humour, et ton professionnalisme Ma Shaa الله. Bonne continuation
Tata Marietou you are very funny 🤣🤣🤣🤣 the fish is very naughty. Mashallah you are doing great and I love the way you cook.
Première,xana nak tay dinguen ma diokh sama *jaime*
Eh wa niou dem diangui watt benen recette😚😚
Jangu du wess
Merci mbahabi diarena yone rafetena hamenane tamite nehna machala senegal tiakanam tiakaw
Je kiffe votre humour !!! 😂😂😂
vous félicite pour la propreté et votre philosophie. Mach Allah ❤❤❤
Tata Marietou j'aime beaucoup ta site sa m'apprend à cuisinier j'avais peurs de faire quelques plats mais avec toi tout t' est possible merci
Maman j'aime trop ta voix 😍😍😍 franchement force à toi
Encore une tuerie. Vous êtes formidable. Je ne comprend pas le wolof mais je pense pouvoir m'en sortir en suivant la vidéo
Chiii li mbaxalou ameurik la! Saf, nekh, gaw. Sobandoo yeuo daldi dial si leneen! Yow la gni weur, Tata cherie! Yalna Yallah barkeel ligeybi. Amine ❤🙏💕
Laay biiiii le macha allah rèk tata 😚😚😚😚😚
Always bek si yaw Tata Mariétou darling merciii again 😁😁😁😍😍😍😍😘😘😘😃😃😃
J'adore ton humeur. J'adore ta manière de faire. J'adore tout tata . Merci ❤❤❤
Wakhbi diékhe na. Lol. Sour na
Macha allah. Mariétou ame nga 20/20. Très bien
Mairy Ndoye 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾💪🏾💪🏾💪🏾😘😘😘😂😂😂
Non tati machaalah je t’aime bien g envie de manger du thiepp
Vraiment madame quel plaisir de regarder vos vidéos...et les explications sont aussi savoureuses...Merci encore "..Heaven.." ....Dieureudieuf...!!!!
Machalla tata pour toute tes conseils j’aime bcp ta cuisine
A essayer inchallah. Tey mom sa tiebou dieuneu la togg à ta manière de A à Z Machallah ct un vrai régal
Sokhna Diaw 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🏆🏆🏆🏆😘😘😘😘
@ wallahi Yallah molay fay mom key diexna takk thi yow lay diangué
ooooohh.!!!l. liii thiy Nawaite...mouye taw
.machAllah.😂😂😂😂
Voilà c s k je voulais dire. Surtout Ak kouthia
@@ndeyesene3999 ..
cccchhhoo...tarfakala rek😂😉n'a ress ak diam
@@aidaly8787 amine
Hamosi dara sokoy lek do tok
Mahchahala Ta mariétou saveurs planétaires gnak lén kham woroul dal 💖💖💖
I love ur cooking
Mane telle telli momaye rayé non tata marietou longue vie
Ma niaaakhhhhh sama li ngay togou safnama woyyyy sauce bi 🤤🤤🤤🤤🤤🤤🤤🤤🤤 we lov u wayyy doundeul tata ohhhhhhhhh
A macha allah tata li dal nekhatina yalla nala yalla faye doundal doundal
MACHALLAH NDAW KOUNDA YALLA NA YALLA WERAL THIERYI🙏🙏🙏🙏
Merci de la dedicace sister marietou. Dila bégué sassouné recettes yi am naniou solo et ton humour j'adore🤣🤣🤣 c'est madioula domou ndeyou soda depuis lyon
Todj nga fi 👏👏👏. Macha allah mbakhal mi saf na😂😉❤️👅😘😜👏👍
Deugggggg laaaaaaaaa🥰❤️❤️❤️❤️❤️
TEAM "AIMER" AVANT DE REGARDER KAAY LEIINE FII !!
Magui barkè kirasoulahhhh
Khady Thiongane wadssvnjkk
ça fait partie de mes plats préférés merci Mariétou
❤❤❤machallah
Omg, I love watching theseso much. she's so funnnyy! loveee her energyyy
💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@Nogoye Bass. I know aunty Marietou is very funny. She entertained while cooking🤣
@@madambah7944 uni
Machalah Tata mariatou avec son poisson tu es fort longue vie à toi insha Allah
Bonsoir marietou namele mon école n'était pas fin mais je suis chaque fois, diakatou a sa place ici ça c'est sauce gordjigen mon frère déteste cela mais moi j'adore merci pour ces plats. Bisous. Mbahale dey saf sape plus citron
Ça c'est mon plat, je suis née et grandi à la médina mais par contre nous, on l'appellait le m'bakhalou guoordjiguéne !!!!
Waw kay mom la done beugeu wakh sakh
Waw key nonoulagn koy wowé😂😂😂khamena tour bi la beuga rafétal rek
Effectivement mbakhalou goor djiguene la
Tourr bi mo rafetoul rek motakh
@@adamaisse pour mw tour bi mooy feeling bi parceque au temps si tu disais m'bakhalou guoordjiguéne laaye togue nieupeuye khaaraanesi !!!! Muuuuuuh dakh la mou saf eupeu na.
Tata marietou sa liguey rafetna. Sama genre gou beugue lekk gui niou gui takamtikou😋😋
Aye tata marietou yeuremal Ndeye Coumba yi sonnananiou Mane de mm souma amoul ingrédients yup dinako lidieunti founekk ba tokk gouko.
PS merci pour la recette
Tayy suniou tata internationale fi leu feul ak nioune waw key❤️❤️❤️❤️
Machallah tata laf thiate beuleup
Salam Marietou et ma part j'ai envie de manger longue vie a toi Machallah from Baltimore Maryland bijou
Haaa tata tay sama plat la 😋lissi daguay lek rek do sourr Tanka nano dokh
A machalla togou louma nekh tite na avec les les parole j adort yalla nassa diam yagueu
Mash Sha Allah ❤❤
MERCI BEAUCOUP Marietou vous êtes un as
How do you make the green sauce in the bowl that is shown at the end
Hi my Dear
It’s spinach and okra lemon or lime juice salt and hot pepper so you will have to boiled them all in the same pot til they all cooked then put it in a blender til you get that paste it’s simple yet delicious enjoy
Mashallah maman
Mane yi momay danellll. Tata sa mbaxalll ame na diommmmm
Ohhhh ta mariétou mbakhal bi mom safna dal 😋😋😋😋
Sa kanam rekk la beugue guiss
Dama la bg
Tata marietou mome founék lay feulé machalla sa mbakhal amna manaaaa
Vrmn 1000 merci pour notre tata d'amour yalla na yalla yok takhaway bi weral thier yi
Mé khana dinga def com korité bi defat opération tabaski
Tré bien négo rélleu djooo no no tata yamay danel
Machallah ta marietou makhalebi eupeuneu 💖
👌👌👌👌👌👌
Machallah todiatti guaffi ma Tata de💖
How do you make the sool and the rank?
Magnifique merci tata mariétou c'est mon plat
Ma Sha Allah Tata Mariétou😘
Merci encore ☺
Mbakhalbi maco kham nawette dagneco dane togoulou beri merci tata
Tata send me some I’m hungry 😋❤️
Machalla résakk diam depuis Mauritanie
Delicious food, cook for us too
♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machalla sama yaye j aime bien se plat
J aime
Nice na sis
Bandass dieune tu😁💕
Cool Nice mais amoule dakhaar.
Manchallah la saint louisiene
Kou beugue❤❤tata marietou noël yeh
Machalla tata mane dal soné gnom youbiyaba rék ma contane 😂😂yalna sa diam yague way
Très bien ! 💗💗💗
Sama yaye nena li mo bakh si santé.
A propos de thiebou tir, ça ce fait en Casamance, ñoul tir bi comme sauce graine ivoirienne bi, xi ngay soor xa tieb. Avec tout les youbi yaba 😅, yokhoss etc.
MaryYehosef ohhh ok merci ma Cherie dina thi def ay recherche Insha Allah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘
Oo tata tes vidéo me manqué bcp ❤
Machallah tata marietou mane damay beug guiss sa visage
Salam tata Mariétou vrément amouniou sa fayi merci infiniment!
KHADY CAMARA Waaleykum salaam
Mane sa ndouguou mou riche rek momay ndieuk danéll..diam si ioe wayy tata
Masha allah tata😘
Humm j'adore ❤️❤️❤️
Merci Tâta pour la recette 😂 sauce bou khokeu bi pour mag yi weral lou bari
😂😂😂manchala
Diennebi mo yabater 😃😃
Aka nekh je l ai essayé wayè dina tok une semaine sa keur di khegne 😂😂😂
Mbakhal soce ngay am fofou saf té nekh
Ma sha Allah Marietou khana serere nga thio de serere moko mom lol
Macha alla c très bien bon
Safena sape merci
Merci tata dafsiy bax sax ins bi senegal niepa toyyy diam si yaw
Tioooo love it
It looks good, but could it be in English or French.
Lol Tata marietou di ngua ma dadj akk jeun yii😁😁😁
Ma sœur tu nous fais saliver Merci beaucoup 😘😘😘de la part de Chinny baby Nigeria USA
Marie Diabou 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Nice machalla
Mashallah 😋😋😋
Machallah sama domou baye
Nékhatina machalla
I love her!
Where’re you? It’s been a while
Taye chez moi mbakhalou ndakarou la maye😋😋😋merci Marietou
21 ème niou nieuw kholi mbakhalou ndakarou
Li la xam si bakhalou tiir day beuri bagasse tata dal yay chef
Sauce bi a la place de l'huile so ko dogué ak diw tir bènène affaire la. Merci
Machalla machalla 🙏
Tata Mariatou we miss you.
Ndawkounda deug rek nga wakh soul day tel doug ndakh mou nior wayai sa mbakhal bakhna d dina ko togue dieu sai k yamako fataly nonou lako beugaiy