Merci pour ces recettes. C est bien là première fois que j tombe sur quelqu'un qui explique si bien comment cuisiner en prenant le temps de montrer chaque étapes de la cuisson point part point . De plus ce qui est le plus intéressant c ke tous les épices et condiments que vous proposez sont faciles à trouver . Mille merci pour cette chaîne de cuisine . Et très bonne continuation InchAllah
Iow mom wax DEUG Yallah nioune gni Di ayy diegg you ndaw dila suivre chaque jour souniou wa keur yi signé. Mashalah yangui niouy diapalé bou bax merci bocoup tata yalah nala Yallah fayy yaggal sa takhaway
Macha'allah ziarenala taye begnewo waye mane begnet seremonie réussir roumain ndax deye nane huilé te aussi daye four ba douma guise mabeugone sa conseil merci
Maa shaa Allah Sokhna Marie merci encore une fois et toutes nos félicitations à nos vaillants gaïndés pour cette belle victoire 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳 Sénégal ca kanam.
Tata merci bcp tu as utilisé benn guedj bouniouma mayonn mou nekh trop et xamoumawonn tour bi. Merci encore lii amoul noumou amé woul gout. Dommage que ingredients yi bo guené senegal mou diafé 😭😭😭
Merci beaucoup maman pour ce plat. Je vie en France, et depuis mon dernier voyage au Sénégal qui date de deux ans, j'ai pas mangé un plat aussi bon. Longue vie à toi.

Mei femme bi mane na togua deh,sourna mane li 😋😋😋
Ooooh ooh tcha bakhal bala j'ai l'eau à la bouche merci tatii sa mbakhalou nekhna
Mbakhalou ndokh bou am djiko lafi guiss😍😍👌
Liii kay mbakhal de victoire rek la meneu toudd, machallah mangui saliver way😂😂
Machalah ♥️ Tata Marie Diop contane si yaw. Mane môme mala beugueul sama bop yagu la suivre. Yalna sa diam yagu♥️♥️♥️
Mashallah maman Celena nekhna yalna yalla wereul lokho yi
Ohhh mon plat préféré 😭😭😭😭
Salam Maman isseu cordon bleu internationale waw li lana ci mbakhal eupeu neu maman isseu yagui gagne wayy 😅🏆🏅🏅👍❤️❤️❤️❤️❤️
Iow mom wax DEUG Yallah nioune gni Di ayy diegg you ndaw dila suivre chaque jour souniou wa keur yi signé. Mashalah yangui niouy diapalé bou bax merci bocoup tata yalah nala Yallah fayy yaggal sa takhaway
Machalla lo toggue rék nekh nama yalla na sa diam yague , Amine.
Oh sama plat mingui mama ken dou yow machallah lafthiat
Machala très bon plat aime beaucoup me
Ya meun kay macha'allah
J aime le mbakhal sa me rapelle mon enfance c est trés bon
Masha'Allahou sama sopee sokhena marie diop togou yaye Isseu. Begue tina si yow de.
Macha Allah Tata Y'Allah gua yague fii lole te were
Salam Toogou Yaye Isseu mascha Allah khol ❤❤❤ya gui fekhe mom 🤣❤❤❤khol sed gouyy frigidere Alhamdoulillah 🇸🇳🇸🇳🇸🇳⚽️🦁🦁🦁🏅🏅🏆🏆👏👏❤merci Beaucoup Bonne Continuation 🙏
Dakar rek gua warone deuk bilaye machala long vie
Merci a notre maman la meilleure vraiment je t'aime beaucoup et tes recettes aussi
J'ai l'eau à la bouche merci maman pour la recette
Ani sama waleu si mbaxal bi 😋😋😋
Machahala nigua téyhé rek moma nekh et que tu explique bien yalna sa diam yague
Mashallah tata très honoré cela me donne envie de le reprendre khana saint louisienne nga
Macha'allah ziarenala taye begnewo waye mane begnet seremonie réussir roumain ndax deye nane huilé te aussi daye four ba douma guise mabeugone sa conseil merci
Slt chérie mane d demb rek lako defar me dama wagni œuf yi. Pour 2 kilo j’ai utilisé 6 œufs
Aimer avant de regarder 😅🥰
Maa shaa Allah Sokhna Marie merci encore une fois et toutes nos félicitations à nos vaillants gaïndés pour cette belle victoire 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳 Sénégal ca kanam.
Manchallah tata plat bi amoul noumou nekhewoul togue nako merci pour la recette
Maman Isseu mborokhé laniou beuguone
Machalla naci
Mach allah mbakhal bi nekhna
Tata merci bcp tu as utilisé benn guedj bouniouma mayonn mou nekh trop et xamoumawonn tour bi. Merci encore lii amoul noumou amé woul gout. Dommage que ingredients yi bo guené senegal mou diafé 😭😭😭
Merci yaye isseu.
J'aimerais que vous nous préparez du bouillie de maïs, sombi mbokh svp.
Soupe dieuneu tata isseu
mbakhalou dokh dadie 😋😋😋
MachaAllah nehatina 🥰 🥰 🥰
Sama plat préféré ak nékkk
Oh mbakhal bi dal c doux mmmmm
Yay isseu sa dieune lan la
Machala tata
Bou wessing laniouyy wakh
Lou nior rekkmà sépi😂je t'aime tata😍
Machallah tata isseu ❤thiepp bi d'où ame d huile walla stp répond moi damako begue togg
Mbakhall mi khoubeu Na
Sourna
Macha Alla
Merci pour ces bons plats 🙏
🥰🥰 machala tata
Defal niou crevette pané🥰
J'adore ta cuisine
Nekhna barina mashalla
Merci beaucoup maman pour ce plat. Je vie en France, et depuis mon dernier voyage au Sénégal qui date de deux ans, j'ai pas mangé un plat aussi bon. Longue vie à toi.
Toufaa
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤cv
❤️❤️❤️❤️🤲🏻🤲🏻❤️❤️❤️❤️👍🏻👍🏻
Foko dieudé
Mar shaa Allah ❤️❤️❤️
Mashallah tata
Machalla
Merci beaucoup pour les recettes macha ALLAH
Sama idol
Machaallah maman
Merci bcoup maman nekhna lool way❤❤❤
Merci yaye Marie ❤️contanatina💕
Oooooh la la j'ai raté
Cool👍👍👍
Merci infiniment yay boy🎉❤
J'adore ta façon de cuisiner ma tata❤ merciii pour tout ces recettes 🥰
❤❤❤
Vraiment merci beaucoup que le bon Dieu vous bénisse
Merci togou yaye 💖🤗isseu
Amine Ya Rabbih Yalna na sa diam yague
Merci encore Tata❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mashallah👌❤❤❤👌
Masha Allah et bon appétit 😋
❤️❤️❤️
Dit moi tata svp l riz, tu as mis directement ou tu as avait déjà, passé à la 1ere,cuisson, Tay, ou hothko
Dako khothieu mes bou la nekhé ga téye.co.
Machalah
Limome thi gneupe la bakh lions yi ak supporters yeupe Dakh gneupe sone après ga soupeulelene soupou yelle
Mére isseu ana mbakhale bii li gay mbakhale dara fayou ko
😘😘
Thiebou tiw tiir
Merci tata. Tiepp dagn koy khodj walla?
Wawe dakoye khonthieu withieu ko
Wawe dakoye khonthieu withieu ko
Beugg na thi Kong fumé deh … noumay deff ba ame thi ??
Mashallah ❤❤❤
😋😋😋
Merci
Salut madame merci beaucoup pour la recette, l'eau noir que vous avez versé dans la marmite c'est quel eau svp
Ces des têtes de crevettes boullie
@@TOOGOUYAYEISSEU ok merci
Dibi à la poille
A chaque vidéo vous nous faites plaisir, merci beaucoup Yalneu sa diam sakh Yalneu YALLAH Suniou Borom wèreul lokho yi🙏🏽🥰😘.
Yakhegua sama adina
Mais vous ne pouvez pas parler en français ? C’est pas tout le monde qui comprend wolof
Il faut aussi juste le demander gentillement. C une tata qui fait déjà l'effort de mettre les recettes bien détaillées et par étape.
Merci tata.
Nous ne sommes pas français
@@maxtra590 merci
@@maxtra590 je l’ai insulté ? Qui es tu ? Pour me parler?
Mais pourquoi vous forcez les gens à parler français alors que c’est pas leur langue?
c’est pas tout le monde qui sait parler français
Machalla
Machalla