Merci beaucoup,je l'ai préparé sans les crevettes,et à la place du vinaigre j'ai utilisé le jus de citron.Mes encouragements et merci encore pour tout.
Tata Yalla na Yalla goudal sa fane et merci pour les cours de cuisine J’avais une fois mangé un plat comme chez une Dame à Paris c’était tellement bon que je me demandais comment elle préparer ce plat, et voilà vous m’avez tout montré merci 🙏🏽
Machallah ma maman Isseu sama mbok ndar ndar bii j'ai encore adoré, ça a l'air trop bon, mann mom il suffit juste de voir la décoration seulement sans même lire dadii khamnii yawlaa, ohhh vive les Saint-Louisiennes
Ma Shaa Allah. Waw lii nak? Aaayway kaylen wakh ak yaye boy mangi dee. Lii deh la comment sii mbaxal mii safna nekh tay ak elek. 💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💯👏👏👏👏👏🤣 Ma Shaa Allah once again maman. Yaye man sourna. 🤣🤣
Bjr tt le monde a mchlh yaye boye sama sopé bi borom khôl bou rafet bi borom bakh ndeysan aka téy iow dale nassa diam yague rek com je le dit tjrs yallah samla same diabotegui arla arre diabote t yit mou lakhlen fou yakh yégoul gua yaguefi lol dignou ouf t mou andak wergou yaram ak soutoureu ak khéweul you sawane bawane mane dale je t'adore bcp mm wolahi
QUI EST D'ACCORD QUE TOOGE YAYE ISSEU CONTINUE POUR LA VIE😍😍😍😍😍😍😍😍
Moi je suis d'accord 💯💯💯💯
Pareil ma
💯 💯 💯 yaye isseu rek pour la vie 💪💪💪💪💪💪
Wawaw
Louma nam rek togantouko ndakh ioe mashalla depuis Maroc I love you❤
Li guay defe ni yalle na yague tes gnougui lay gnanal yalnala yalla may goudou fane tè wer
Machaalah amna solo yalna yallah fayla the samla
Merci beaucoup,je l'ai préparé sans les crevettes,et à la place du vinaigre j'ai utilisé le jus de citron.Mes encouragements et merci encore pour tout.
Sour na macharllah tog bi rafete na sela na amoul bena menatou tout est naturel yallah na sa djam yag si barke seydina Mohamed psl 😘
Je n'ai jamais commenté dama done setane rek di aimé mais mbaxal miiii oh yeugal nama machala yala defal la kheuwal
Yaw, koula dégue sakh, khamni daguaa baakh maa.shaa Allah. nala Yallah faye guengui paye amiine yaa Rabbi.
Machallah tata amena tina solo merci beaucoup tata ❤❤🥰🥰👍🏿👍🏿
Yalla Faye la ❤❤❤
Tata Yalla na Yalla goudal sa fane et merci pour les cours de cuisine
J’avais une fois mangé un plat comme chez une Dame à Paris c’était tellement bon que je me demandais comment elle préparer ce plat, et voilà vous m’avez tout montré merci 🙏🏽
Machallah ma maman Isseu sama mbok ndar ndar bii j'ai encore adoré, ça a l'air trop bon, mann mom il suffit juste de voir la décoration seulement sans même lire dadii khamnii yawlaa, ohhh vive les Saint-Louisiennes
Sa sans bon yékal wa vélingara ❤maman🎉
Macha Allah tata yalla n'a yalla youkou sa Diam
Merci way wa yarakh content naniou machalla na réss ak jam saff na dal souba inchalla ma togou ko❤❤
Ma Shaa Allah on apprend beaucoup avec notre cordon bleu Yaye ♥️
Machallla tata dinako togue damako name sakh
Macha allah nekhna torop la prochaine fois sauce bi danga kay togalé ak bissap ak dakkar ohoo benen affaire leu 😊
Machallah maman Man dh damalay suivre souma magué yalna mélni iow❤️💋
Togou yaye Isseu laye done bamou barii dolé contane thi yow rek yaye boye 💪💪♥️♥️👌👌
Salame Tata Marie merci beaucoup pour les recettes vraiment liguay togue setna selna Masha Allah Dieureudieuf Bonne continuation 🙏🙏🙏💞
Machallah laf thiate tata cheri doundal
Sama plat 🥰🥰doumaci doyal
Ma Shaa Allah. Waw lii nak? Aaayway kaylen wakh ak yaye boy mangi dee. Lii deh la comment sii mbaxal mii safna nekh tay ak elek. 💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💯👏👏👏👏👏🤣 Ma Shaa Allah once again maman. Yaye man sourna. 🤣🤣
yaye jâmmm sii yaw j tm fore ak yaw tokk niepeu daye safe sap machalaaaaa lou bari si yaw lako khamé ma doli ko si lima khamone
Merci ya isseu yalla n'a leu faye
Merci manma tu es fort machallah ❤
Mashall Allah mum keep it up may Allah reward u
Nekh rek laydef machaallah❤❤❤
Olala combien cela donne l'eau à la bouche
Macha Alla
Grave adoré pas dhuile je prend note machalla tata
Mon plat préféré plat bou ma nekh la machallah
Ahh tata todiati nga fi radiakh ak sedd bi ni saxx lou bari ngay am lane
Machallah tata mè begue na nga gneuwate si mousseul dieune bi merci beaucoup wa Maroc 🇲🇦 yeup yaw lagnouy bégué ❤️🥰😘✌🏼
Macha Allah
MachaAllah. Merci beaucoup Toggu Yaye Isseu 🙏🏾
Macha Alla niak LA guis worol
Wawaw machallah merci 👍❤
Li mom lak la Wala kheumla finga guene noyna machala
Contane nassi yow ya tax ma mane soupou kandia😂 sapoo a vs👍👍🙏
Machallah tata défatiga sa meunine super
Macha'Allah! Yalla sa diam yague💙💙💙
Da War Di nougue lo khamni kou yoroul meune nako am yaye isseu pense au pauvre sto
Machaallah. Amna solo.
Assallamallikoume namone naniula mba yene gui ci jam machallah amatina solo dieureudieufati beguee
Merci merci macha Allah
Merci beaucoup tu m'as aidé🥰
Machalla sama yaye
Sa ma dom namenala
Bjr tt le monde a mchlh yaye boye sama sopé bi borom khôl bou rafet bi borom bakh ndeysan aka téy iow dale nassa diam yague rek com je le dit tjrs yallah samla same diabotegui arla arre diabote t yit mou lakhlen fou yakh yégoul gua yaguefi lol dignou ouf t mou andak wergou yaram ak soutoureu ak khéweul you sawane bawane mane dale je t'adore bcp mm wolahi
merci merci a ma yaye isseu qu Allah vous récompense et nous laisse ensemble 😍😍
mer ci beaucoup chapeau.à.vous
Mashallah na rees ak diam
Merci maman ❤❤
Xana toujour dafaye fater rek
Mako ndieuka vuuu🤩🤩🤩
Merci beaucoup maman vraiment tu cuisine bien bon appétit
Oooh maman g l'eau à la bouche
tata Marie yalna sah jama yagui
Merci beaucoup pour la recette
Mbaxal bii farna 😋😍
❤❤❤❤❤❤❤❤
Oooh sama plat mashallah
HemJ’arrive lapin ça a l’air trop bon
Merci pour votre facilité
Soula nekhe ga def thi diwtir ou bien
Merci beaucoup YAYE issue machallah vraiment sa émission bi amna solo
Khifna dé li rk la begue
Machallah tata
salam tata marie taye dama tardé machallah nékhna 💯💯👩🍳👩🍳😘
Merci paly diop
Maclhallh nekh na
Mashallah
Aah toureundo 😭😭❤️
Humm avec ce froid merci way ❤️❤️❤️❤️
Mooo Aïcha ban froid lekhal te boul saliit
Merci yaye isa 😋😋😋
Machalla amena solos 💪🏼💪🏼💪🏼💪🏼💖💜💟👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿🍀🌴💞💞👏🏿👏🏿💟👏🏿👏🏿🇸🇳🇫🇷
Ya meune ya eup dolei
Machallah machallah Tata 😋😋😋😋
Machallah
Merciii Maman. pour qui parlons pas et comprenons pas le wolof on peut au moins sous titre en français. Merciii
Machalah Tata recette thiére mboum la beug merci
Togue réck ngaye défe bi sama plala
M'achallakh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😋😋😋😋
Souba inchaalla mom lay togue
machallah mon plat préféré
Machallah set na sell na sama plat la nekhna Itami 😂😂
ASé coloba
Slt Tata day ameu ay epice wala
Merci maman issue que dieu te garde machallah
Merci Sophie ya bakh waye
Merenaala la dé mais pourquoi liii
Maman merci beaucoup yalna yalla goudal say fann mais deffaral niou diébou pailla
Yaye Issa je te suis toulle temps mais vraiment alkhouran bigaye wakh soy togue MoMA guena nekh
MashaAllah tata saf n’a 😍👌
Mon plat préféré oooh
Machallah👌
Merci marie nekhatina
Machaallah nehatina😘
Cv
Très bonne recette tata j adore
Macha Allah
Machallah 🥰🥰💖
Tata cherie♥️
Merci tata nekh na je te souhaite une
Masha ALLA 😍😍
Machallah 😋❤❤🙏🙏
vraiment mère dagua meune toguou