Qu' ALLAH SWT aie pitié de mère nioba et l accueille au paradis ainsi que tous nos défunts parents. Amiine ya rabbi. Notre maman fut un cordon bleu. Paix à son âme. Bien des choses à toi ta Mariétou . Recette bi nekhna Machalla
Recette bi nékhna torop merci. Mais koula dégue, daye sentir sa voix ay émotion et beaucoup de souvenir Macha'Allah Mère diop yalnako yalla kharé aldiane té sarakham yague sa lokho, Amine
Alaykoum salam w rahmatu llahi w barakatuh Baraka llahu fiki oukhti Allah y jazik bi kheyr pour toutes les recettes, tout est magnifique allahuma barik, ma shaa Allah ça donne envie qu'Allah te préserve
Mère Diop yalla nako yalla kharé aldiana firdaws. J'ai connu une certaine mère ndiobaa qui venait à l'ecole champ de courses de dakar. Le bon vieux temps ndeyssane. Merci beaucoup On est tres fier de mère Diop
Macha Allah, en vous écoutant on remarque que vous êtes quel1 de très gentille. Merci pour tout ce recettes que vous partagé avec nous. May God bless you and your Family.
6 лет назад+1
dikha 75 ohhh Ameen et merci my Dear you’re so sweet Masha Allah
Nekothiiii rellll no Aunty you're very nehhhh😁😁😂 man lolou may dadjiiiii, mais Aunty family Ndao, Sama family, Ndaocounda, Ndao beuleup ndoucoumane sa ndendé Arame faha ❤️❤️❤️❤️🙏🏽much love
Machala beugue lou bakh reka am solo ,liguay togou nekhnaniou adouna amoul solo lima gueuna nekh moy si khorom gua yem doy def bouillons cubes yi ,li guena yok fébar yi Afrique sila bok . Mére Diop yalanako yala kharer Aldiana firdawsi merci beaucoup tata
Bravo ma soeur. Je suis tes recettes depuis le Canada à Québec. Daguama nekh. J'aime ta façon de commenter les recettes Sé bien vivant. Bisou ma soeur chérie tu fait la fierté des femmes sénégalaises et africaines
OUI C' EST VRAI MOI JE LA SUIS DEPUIS LA SUISSE CES COMMENTAIRES SONT COOL ET ELLE PARLE TOUJOURS DE MERE DIOP VRAIMENT JE CROIS QUE C' EST UNE FACON DE RENDRE HOMMAGE A MERE DIOP ET C' EST BIEN, ON A Q' UNE MAMAN
Ohoooo je suis mélancolique ndeyssane. Walahi mère Diop ndeyssane. Pain pastel mère Diop à 17h rèk louné lawone Maa shaa Allah. Qu'Allah l'accueille dans son firdaws. Longue à ton papa. Sista ça serait top d'avoir la liste et le dosage des ingrédients.
bismilay bonsoir tata marietou mbok yi pouce bleu commenter partager la vidéo mere Diop je laime bien yalla n'a khipper adiana firdawsi thi barkhe cheikhoul tata marietou mane Medina reubeuss kham da fa bou bakh dakh fann hock la Maguer Merci encore une fois pour ces recettes on te suit tout temps depuis paris
Je suis une nouvelle abonnée, machallah sa togu rafetna setna, mais c’est ton humour que j’aime encore plus, vous me faites rigoler par vos commentaires.
OMG!!! Thank you so much auntie Mariétou. I love so much fatayas, but I missed them all the time. After watching your video I have succeeded thanks to you. Thank you to explain clearly and share with us your joy of life.
6 лет назад+1
Penda Diarra 🤝🤝🤝👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾 you welcome my Dear Insha Allah we will be working on these little appetizers this week please stay tune Accra is on the way and beignet de poulet et crevettes aussi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Sa fait pas trop longtemps que j'ai commencé à vous suivre mais vous avez un bon humour en plus j'aime la cuisine depuis tte petite et je suis tjrs en quête de qlq chose de nouveau. J'aime votre facon de cuisiner propre et précis 😘
bilay j’me rapl ma chérie que de bon souvenirs ta maman était là meilleur cuisinière yalla nako yalla yereum fimou nek yalla nako gueneul fimou djougué Amine
Nékociii douuuttt 😂😂😂😂way jaime ça way😍 Mère Diop yalnako yalah yeureum way🤗! Togologue leuwone deh mashallah ! Sama tata tamite yakoul Dara si art bi😍
machalah. liguey bi sell na te and akk dall. mere diop yalla nako yalla kharer aldiana bayil nala heritage bou magg. mane dh legui yaye sama coach
Ndeyssane fatéli nama fataya mère Badiane Kaolack ndangane . Écolou Directeur Joseph Diouf kasnack.
Qu' ALLAH SWT aie pitié de mère nioba et l accueille au paradis ainsi que tous nos défunts parents. Amiine ya rabbi. Notre maman fut un cordon bleu. Paix à son âme. Bien des choses à toi ta Mariétou . Recette bi nekhna Machalla
Cuisine sans bouillon..
Kou d'accord que merr nio dakh togg khaleyii...medina benene affaire leuu...fene d'où Médine
Recette bi nékhna torop merci.
Mais koula dégue, daye sentir sa voix ay émotion et beaucoup de souvenir Macha'Allah
Mère diop yalnako yalla kharé aldiane té sarakham yague sa lokho, Amine
chami fam Ameen wayy
Alaykoum salam w rahmatu llahi w barakatuh
Baraka llahu fiki oukhti Allah y jazik bi kheyr pour toutes les recettes, tout est magnifique allahuma barik, ma shaa Allah ça donne envie qu'Allah te préserve
Diape forme...nékothi rélle.. l love you ma tante.
Machala amna solo dieureudieuf ndao
Mère Diop yalla nako yalla kharé aldiana firdaws.
J'ai connu une certaine mère ndiobaa qui venait à l'ecole champ de courses de dakar.
Le bon vieux temps ndeyssane.
Merci beaucoup
On est tres fier de mère Diop
Macha Allah, en vous écoutant on remarque que vous êtes quel1 de très gentille. Merci pour tout ce recettes que vous partagé avec nous. May God bless you and your Family.
dikha 75 ohhh Ameen et merci my Dear you’re so sweet Masha Allah
Yes she’s very nice
Nekothiiii rellll no Aunty you're very nehhhh😁😁😂 man lolou may dadjiiiii, mais Aunty family Ndao, Sama family, Ndaocounda, Ndao beuleup ndoucoumane sa ndendé Arame faha ❤️❤️❤️❤️🙏🏽much love
Très bonne recette,toute la famille s'est régalée
Machala beugue lou bakh reka am solo ,liguay togou nekhnaniou adouna amoul solo lima gueuna nekh moy si khorom gua yem doy def bouillons cubes yi ,li guena yok fébar yi Afrique sila bok .
Mére Diop yalanako yala kharer Aldiana firdawsi merci beaucoup tata
Paix à son âme. Merci mère Diop thi recette pâte bi. J ai beaucoup adoré surtout la bouillon d poisson
Quoi elle est décédée ?
Thank you so much ch for this beautiful recipe. I was wondering if I could use salmon for pastel, and now I know I can.
Mane môme bisimilaye bii rek momaye raye yague fiii looo t’es andakhe wére inchala
Machala tata Marietou mère bi niogui koy nianal yalla yeureum ko té kharé ko aldiana firdawsi amine
oulimata tine Ameen wayy ma Cherie 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Ma cha Allah une vraie professionnelle vous êtes très généreuses que Dieu vous protège et vous préserve🙏🏽
Rossi bii kheegn na ba Dakar 😍😍💝💝💖💖
Tata Mariétou beug nala wayé bi ngua toudé Mame Abou Aziz Sy Dabakh Malick la le guene beug Macha Allah yalla nala yalla defal diam
Merci tata merci tata souvenirs souvenir pastel kay xallé boudoul wone mague cone doubakh machallah amal diam yaw tamite ??
ohhh c ma 1ere commentaire mais tata pa ndao beuleup ndoukoumane sama mame nonou la toudoon ohh yallah na xippee aldiana sama xarite bobou
Welé lé leeeeeee wouy magui youkhou😍
Mashallah tata gueune nala sope thi ligua todou sama mame dabaakh yalla na yalla goudeul saye fane inchallah
Bravo ma soeur. Je suis tes recettes depuis le Canada à Québec. Daguama nekh. J'aime ta façon de commenter les recettes Sé bien vivant. Bisou ma soeur chérie tu fait la fierté des femmes sénégalaises et africaines
OUI C' EST VRAI MOI JE LA SUIS DEPUIS LA SUISSE CES COMMENTAIRES SONT COOL ET ELLE PARLE TOUJOURS DE MERE DIOP VRAIMENT JE CROIS QUE C' EST UNE FACON DE RENDRE HOMMAGE A MERE DIOP ET C' EST BIEN, ON A Q' UNE MAMAN
Mach'Allah Sokhna Marétou Contaanaa ci yow Yallah nala Yallah Sam ci barké Dabakh Malick R T A 🤲🤲🙏
Ah machallah tata marietou toute gua samay quartier niayes thiockers et rebeuss ndeysanne hamna sama niom yaye nioy ham mère Diop
Mane say termes damay Fathi tata, nekothi rel, gounouss gounoussi, youbi yaba yi, lakh lakhal💋💋💋
Tata marietou yal na la fi Yallah bayii barkeel lokhoo bâ 💓💓💓
Ohoooo je suis mélancolique ndeyssane. Walahi mère Diop ndeyssane. Pain pastel mère Diop à 17h rèk louné lawone Maa shaa Allah. Qu'Allah l'accueille dans son firdaws. Longue à ton papa. Sista ça serait top d'avoir la liste et le dosage des ingrédients.
On t'aime fort mane de naka si réul bi rek momay Ray machalah
Diap forme Nekothi reul goundouss goudoussi Talalei Aïe ndeikeitei Tata marietou Labeug nii😍😍❤
Je vs adore ma grande dagua nekh dérete way🙏🥰
Neko thi relle bien bon tata marietou dale machaala contane na si yaw
Rélleu bamay rayy 😂😂😂diappou forme😂😂🥰
Maachaa Allah ma soeur yaw borom bakh nga namone naala yalla na yalla barkeel
Non ta marietou dinama dadj yalla na yalla bayila bi sognou kaname 🙏🙏😘😘😍
bismilay bonsoir tata marietou mbok yi pouce bleu commenter partager la vidéo mere Diop je laime bien yalla n'a khipper adiana firdawsi thi barkhe cheikhoul tata marietou mane Medina reubeuss kham da fa bou bakh dakh fann hock la Maguer Merci encore une fois pour ces recettes on te suit tout temps depuis paris
Mamelaty Toure Ameen ma Cherie 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Ohhhhhh machalah tata marietou li nak ladone xar bobou batay merci encor ,ma dieul note tè nieuw inchalah
Bilay ya begue lou bakh saumon dieune dakhou ko macha Allah
Tata demay yakal wayyy MDR.....
Merci bcp mère Diop yalna aldiana donne keureum
Merci pour ses belles recettes sa donne leau a la bouche
eimda woos Insha Allah bin dalma sa tour ma yekaleu
Merci danga bakh rek
Mado Sow la toudou merci bcp yalna lokho Bi werr vraiment ma ngui diangu lou beuri si yow
Togu dal sa yeufff la
Mouahhhhh
Je suis une nouvelle abonnée, machallah sa togu rafetna setna, mais c’est ton humour que j’aime encore plus, vous me faites rigoler par vos commentaires.
Lii gay def amna solo merci beaucoup , yalna la yala may goudou fan ak beaucoup de santé. Amine !!😘😘
je suis nouvelle abonnée vraiment bravo un beau travail j'adore merci beaucoup pour la vidéo 👍👍👍👍👍🙌🙌🙌💕😁💋
Merci maman chérie moi c est mado depuis senegal Yalna sa diam yagg mais recetu fataya ak patate douce bila beugue
merci beaucoup tata mariétou yalna yalla goudal sa fane mayla weir jtm forte♥️♥️😘😘
Machalah sa toguou selle na te bah.😁 na si niepe Mame Abdou yalla na yalla yokou aye leram te tass niou si barkeme si barke S Mouhamed PSL.
Nit dey sawar sa pour setan vidéo bi ak termes yi mouy wax Macha Allah bonne continuation 💪👏💪👏💪
OMG!!! Thank you so much auntie Mariétou. I love so much fatayas, but I missed them all the time. After watching your video I have succeeded thanks to you. Thank you to explain clearly and share with us your joy of life.
Penda Diarra 🤝🤝🤝👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾 you welcome my Dear Insha Allah we will be working on these little appetizers this week please stay tune Accra is on the way and beignet de poulet et crevettes aussi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@please levure chimique is it baking powder or yeast ?
@@nadjmaetoile6629 levure chimique is baking powder. Yeast is levure fraiche
Ah ok u
Machaalla amna solo diadief mere diop
Bi rek la donne khar maachaallah gueune nala beugue dakh dabakh bobou ngua toudou
Ma sha Allah yalana yalla wéreul lokho bi 😘
Sa fait pas trop longtemps que j'ai commencé à vous suivre mais vous avez un bon humour en plus j'aime la cuisine depuis tte petite et je suis tjrs en quête de qlq chose de nouveau. J'aime votre facon de cuisiner propre et précis 😘
ma shaa Allah Marietou.merci et bonne continuation.
Ma cha allah sokhena mariėtou yala na yala féye 👍🏿
J'adore ❤️❤️❤️ Reee na ba sonn 😂😂😂
Goudouss goudoussi machalah dekker yaw la beugue
Ma cha Allah yala na yala faye tata. Mais ree na baye dioye😂🤣😂🤣😭
Alima Gueye Ameen
Ma sha Allah vous êtes une bonne vivante
Votre bonne humeur fait du bien
Yalla nala Borom Bi Sam
Soutoureu bou yaatuu in sha Allah
Nooon mais Tata affaire bi yow la...mala beugue 😍😍😍
Machallah Tata Marietou à travers vos vidéos on sent votre joie de vivre. Depuis la Mauritanie nous vous disons Merci pour le partage.
Ma cha allah amatina solo sama toguolokh bi
Macha Allah lii dara fayouko
Ah li loumay tester lay done masha allah
Nexoul ba nexoul mais jador votre wolof 😍
Merci des plats vraiment délicieux.bonne continuation
Machaalla Nice na 👏👏💖
Mère Diop Yana khipè aldiana
Sow Ndeye codou Ameen wayy seydi sow
@ de
W
Machallah tata yalna lokho bi weer on t'aime bcp
Merci tata Mariétou. Tu nous donne la joie de vivre avec tes recettes
Tata yalla sa diam yag machalah beug nala
Okhoooo nekh ne Machallah Machallah 😍! Merci pour tes recettes
Machalla tata nèko thi rèl mouy goudous goudoussi mo may danel. 😘😘😘
Mhallha tata yallna sa lokho geuna werr
Mane beugeuna say khetou toggou dal mane😋😋😋😋.
ma chérie togg nga lima beugue pastel mashaallah
ravie de regarder tes vidéos merci pour la recette
Mally Ndiaye mally ma sœur chérie tu te rappel de ses pastels la heiiinnnn
bilay j’me rapl ma chérie que de bon souvenirs ta maman était là meilleur cuisinière yalla nako yalla yereum fimou nek yalla nako gueneul fimou djougué Amine
Ameen sis
passe le mail de saveur planétaire stp
Nice na Mère Ndioba Yallah nako Yallah xarè Dianatul Firdawaai Amiine🙏🏽
SENEGALBOY12 Ameen
Maman mane dama beugu togue mais machalla j'aime 😍
Merci mer diop nila dom dagakoy diagall togou mes batiko rek mouy takhawalu yaw yaydji ga nèk si wange wi lolu bakhull
Merci pour la vidéo dîna saf SAP
Mane ku laye weure sama tata bu yokou samay point su seybu bilay Lo déf ma copié ko Mr contane yalla nasa diam yague tata adoré
Tata merci beaucoup way, apres recette akkra dina gnew stp😋😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾
F.ba Ba Insha Allah Accra c’est pour bientôt
Machaalla, li guay pastel eupna, machaalla
Machallahh Tata todj guafiii dina rayati Mrs 😂😂😂😂rékkkk🥰
J n peux plus m passer de votre chaîne.mais pastels yii todjna. Machalah kom vs dîtes
Wa deguel liii tayy patt bii tiiit jeune bi jap form jaime
Nékociii douuuttt 😂😂😂😂way jaime ça way😍
Mère Diop yalnako yalah yeureum way🤗!
Togologue leuwone deh mashallah ! Sama tata tamite yakoul Dara si art bi😍
Une abonnèe de plus 😚😚😚
Je vous remercie beaucoup pour le partage de vos recettes merci beaucoup j'adore j'aime cuisiner
MachaAllah everything looks great but the hic for me is the mixture of tomato and mustard.
En plus du doi vraiment être forte 💪tu travails avec une seul main 🖐machalla
ibrahima kebe je te dit she is very strong 💪🏿
Merci tata pour le partage, j'ai découvert ta chaine la semaine passée (khawma fouma nekone lol) j'aime ta cuisine.
Mére Diop Yalna khipé Aldianay Firdaws !
Merci Mariétou Vivement pour ce genre de recettes 👍
Mberry Mmy Amenn
Manchala tata bonne continuation ❤️
Tata marietou machallah gros bisous
wawaw ndiranou pastel bobou walla beignet ak jus bou khormbette
Macha Allah s'y malick 👌
Ma shaa Allah Tata Marietou. YALLAH nala yAllah faye. ...bougnou amoul saumon bane djeul moy nekh thi pastel??
Bo publier rek kholi séd.yalla ne yalla le feye . mère Diop yalla ne khipé aldiana
Senegal me mank rekh way pastel bi nehna❤
Waa je viens de te découvrir mais chapeau bas 😘 😘 😘