Deug Nékhoul: Ancienne Mouride Ma Khady dénonce le Shirk (Bokalé) dans le mouridisme

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 18 дек 2024

Комментарии • 41

  •  4 года назад +18

    *Lann moyy A't-Tawhîd...* Wéteul Yalla...Contrairou Bokalé Yalla? *_Lannit moy Bokalé?_*
    Si xamxam yi dafa amm xamxam bouniouy wowé:
    *Fiqh:* mo layy diangal nouniouy diâmo Yalla.
    *Hadith:* mo layy diangal nou Yonantibi saws démone doundé Islam ak nane laniou wara doundé l'islam souniou ka beugué roy. Si xamxam bi, ngay diangué *Sounnah* t moyy dokhalinou yonanti bi saws si dîné ak comportement.
    *Tafsir:* mo layy dégeulo ak comprendre lo kaddou Yalla you nekk si Al Qur'aan. Ak lann la Yalla dioublou si lepp loumou niou wakh si téréwam bi.
    *Sîrah:* histoire et biographie du Prophète psl et ses compagnons
    *Tadjwîd:* nann laniouy diangué ak tarée Al Qur'aan...mou diarr yonn té rafet.
    Et d'autres xamxam.
    Legui nakk...dafa amm Benn xamxam bou amm solo bouniouy wowé:
    *A't-Tawhîd:* xamxam bi mo layy diangual nou Yalla wété si Ayy mbiram yeup! Xamal la akkeu Yalla Yi. Yo khamni kou si dialgati dangay dougou si bokalé...minga xamni Yalla dafa wakh Dou ko balé.
    Si xamxam bii niouy wowé *A't-Tawhîd* ...dafa amm niett xâthie souniou kayy diangualé.
    Xâthie bou ndieuk bi: *Tawhîd A'r Rouboûbiyah*
    Si xâthie bi laniou layy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si Al Khalq:* Création Wala Sakk. Moyy Yalla mo Sakk niepp niouy doundou, nitt, animaux yi, Malaka yi, djinné yi, ndokh yi, djant bi, weer wi...lepp si gatal. Nitt sou wakhee Kenn koudoul Yalla mo Sakk Dara si adouna bi...kokou bokalé na Yalla si Tawhîd A'r Rouboûbiyah...si xâthie bouy diangualé Al Khalq. Beu Legui si A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah, Dina niou la fa diangual, ka *Yalla dafa weet si Al Moulk:* moyy Yalla dafa weet si Ngoûr. Momm moyy Bourou nieup. Mou amàt belen xâthie, si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah...bouy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si A't-Tadbîr:* moyy Yalla moyy dokhal mbirou adouna bi, moyy contrôler weurseuk yi, doundou nitt gni ak ngelaw yi...taw Yi...ak événement youy amm si souniouy mbir, Moyy rayé...moyy doundeul. Kou wakh Lou melni kelen moyy diokhé doundou ak dè. Bokalé nga Yalla si weteul Yalla si A't-Tadbîr si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah. Si A't-Tadbîr tammit, laniouy layy leralè ni ke Yalla moyy contrôler souniou affaire yeup comme kann mo niouy Djitté, nou souniouy mbir di demé ak kou Yalla tekk si souniou kaw. Yalla rekk moyy falé. Falé akkeu Yalla la. Kou KO diokh kelen koudoul Yalla danga bokalé Wala diokh Yalla un associé...si mbiroum Fallé. Nitt dafa amm akkeu ak loumou Yayo t momm KO. Yalla amm Ayy akkeu ak loumou Momm. Kenn amoul droit diokh akou Yalla mamam Wala kharitam Wala Serigne niamm, yonanti bi ou qui que ce soit. Momm la yonanti bi saws wakh moyy togne bou geuneu reuy si togne yi. T togne bakhoul. Rawatina togne Yalla.
    Legui damay teunk Lou dess si résumé xamxam bouniouy wowé A't-Tawhîd:
    *Niarelou xathie bi...moyy A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah* ...fi laniou layy diangualé Yalla dafa weet si Diâmou Yi...moyy lepp louy Diâmou Yalla. Kenn warou ka defaral Kenn koudoul Yalla. Example de Diâmou Yalla:
    *Djoulli:* Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kouy dioulil kenen. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A's Salaat...Djoulli.
    *Yakar:* Yalla rekk laniou wara yakar. Kou yakar kelen koudoul Yalla. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A't-Tawakkoul...yakar.
    *Diâmou:* Yalla rekk laniou wara diâmou. Kou diâmou kelen koudoul Yalla si bepp façon d'adorer ou diamou. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si Al Ibâdat yi...diâmou yi. Iyyaaka na'hboudou. Yaww rekk laniouy diâmou.
    *Ndimbeul:* Si Yalla rekk laniou wara sako ndimbeul. Iyyaaka nasta'înou...si Yaww rekk laniouy sako ndimbeul. *Kouy sako ndimbeul si kenen koudoul Yalla en étant en danger*, Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A'l Isti'âna...sakkou ndimbeul. *Note:* *Sakkou ndimbeul bokalé* moyy par example, nga nekk si auto Mouy wadja accidenté, wala nga nekk si biir guethie ngay melni kou nara lapp, wala nga teud si lale febar...nga ragal d, ngay Sakkou ndimbeul si Serigne bou genn adouna pour mou secourir la/dimbalila. So nekee danger, Yalla nga wara wo. Soko defoul bokalé nga.
    Et y a d'autres comme niann...Yalla rekk laniou wara niann. Niann diâmou la. Ragal kou fi nekoul...Al Khawf. Yalla rekk moka Yayo. Akkeu kamm la. Pour ne pas trop citer d'exemples d'adoration...j'arrête ici. Naniou diangue souniou diné samay mbok djoullit...li yeup dinaniou KO kham et les détails et exemples que g pas cité. Naniou kham bokalé ba douniou KO deff. Douniou KO djigne kou ka defoul. Ndakh khamnaniou loumou donn.
    Si gatal si A't-Tawhîd A'l Ouloûhiyah, bepp diâmou Yalla, Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kou ka defaral kenen. Diokh nga akkeu Yalla kokou.
    Ma teudiee fii...ak *xâthie bou moudj bi. A't-Tawhîd Al Asmâ...wa's Siffât.* Fii laniou layy diangualé tourou Yalla Yi ak melo kanam Yi. Moyy ayy tour ak melokane yo khamni Momm rekk mo ka Yayo. Kou diokh tour wala melokanou Yalla. Bokalé nga si borr bi si A't-Tawhîd A'l Asmâ wa's Siffât. Example: Yalla mo amm melokane bo khamni moyy guiss nieup ak lepp. Kou Yakar ni dafa amm Kenn kou layy guiss fo manti nekk. Yangui bokalé kokou akk Yalla si côté bi. Kou Yakar ni Kenn koudoul Yalla khamna si lo nekk fo manti nekk, bokalé nga Yalla si Benn si melokanam yi. Ndakh Yalla rekk moyy xamm nieup si louniou nekk a tout moment. Akkeu kamm la.
    Legui nakk. D fois pour nga xamm ndakh nitt dafa bokalé fokk nga kham tawhîd...weteul Yalla ak contraire ramm bokalé Yalla.
    Kou beugeu kham sa dîné, commence par lire la traduction du Coran et les enseignements du Prophète psl dans les livres de hadith comme le jardin des vertueux, Sahih Mouslim, et Sahih Boukhari. Et plus tard...nga commencer diangue deug deug sa diné.
    Naniou diâmou Yalla ! Naniou diangue souniou diné.
    Lou bakh si sama wakh si Yalla la diogué !

  • @lamintouray7262
    @lamintouray7262 Год назад +4

    This young lady has spoken the truths which many of the Senegalase have seen it but due to afraid they don't talk about it. Thank you young lady May Allah protects you

  • @lailahailallah2813
    @lailahailallah2813 4 года назад +18

    Vraiment ma khady je t aime à caues de la pure veritè que tu dis que dieu te garde

  • @muslimmuslim162
    @muslimmuslim162 3 года назад +16

    Vraiment Ma Khady tu es extraordinaire ❤️❤️❤️

  • @ndeyeyandediouf4549
    @ndeyeyandediouf4549 3 года назад +4

    Masha Allah Oukhty lal ga fiiy méti nak.. Franchement defa doy quoi.. Allah dou morom borom la

  • @elhadjimalick2418
    @elhadjimalick2418 3 года назад +3

    Machallah ci kaddù yù rafét yi.

  • @abiboutoure4240
    @abiboutoure4240 3 года назад +2

    Merci ma khady yagefi lol ta wer

  • @siacamane3361
    @siacamane3361 3 года назад +3

    Vraiment longue vie a vous et aussi País a son ame ya seyda fall

  • @abiboutoure4240
    @abiboutoure4240 3 года назад +2

    ماشا الله جسک الله خیر

  • @mouhameddiene5556
    @mouhameddiene5556 3 года назад +2

    Machalah ❣️ yalah fay la

  • @abdougueye8478
    @abdougueye8478 3 года назад +4

    Merci beaucoup ma sœur

  • @zeynabdiallo1744
    @zeynabdiallo1744 4 года назад +8

    Allah the best .Yallah Keeneu la moy borom kaw ak souff,birom adouna akk allakhira.....❤❤🥰🥰🥰🙏

  • @ibousall8145
    @ibousall8145 3 года назад +3

    Machalla ma Khady mais fan nala

  • @annasadio7574
    @annasadio7574 3 года назад +5

    Allah est unique

  • @mamecheikhsarr6644
    @mamecheikhsarr6644 4 года назад +4

    السلام عليكم ورحمة الله وبركاته،
    جزاك الله خيرا.
    Amna solo lole Ma Khady, qu'Allah te protège et te récompense.

  • @adamasy267
    @adamasy267 3 года назад +3

    Deugg nekhoull

  • @biranedaff6987
    @biranedaff6987 3 года назад +4

    بارك الله فيك قل الحق ولوكان مرا الله يحفظك

  • @fatimaba9293
    @fatimaba9293 3 года назад +2

    Ma Allah alcouran et sunnah reek ma khady

  • @aligueye4727
    @aligueye4727 3 года назад +5

    Ndawssi yalah nako yala aar kii Macha Allah deug rék lay wakh walahi yawmal khiyam niou bari dinaniou am mbétél gnii niouy diokh daradia douniou doone dara comme ay imbécile you mélni kara ndiabar séni talibé tékssi diléne diangal bokalé

  • @mtbroug2358
    @mtbroug2358 4 года назад +6

    Bilay ma khady yalna la sounou borrom Faye ci deugueu bi ma la beugueu soumalay deuglou demay khamni deugueu reck mo worr je t'encourage à continuer la lutte.

  • @balysyll7684
    @balysyll7684 3 года назад +2

    Bilahi deugu la ma Khadi 🥰🥰🥰🥰

  • @Multi140777
    @Multi140777 Год назад

    Oh mon peuple , pourquoi m'appeler à l'enfer alors que je vous appelle au tout puissant , tout Clément.

  • @lailahailallah2813
    @lailahailallah2813 4 года назад +8

    Ma khady sa diane wathna
    Tu as denoncer ce que personne n ose dire au senegal

  • @caroleducrocq8248
    @caroleducrocq8248 2 года назад +3

    Allahou akbar allham doulillah yallah yoow rék yaaye yallah kééne dou yallah koudoul yoow yallah mouhamadou rassoul mooye sunu yonéént yallah kééne la fii téh doo toul gnar ccii darou adouna.Deeg dou roombii noop xana noop mounafixoune SÉRINGUE boy bass yaa meena kaacc xana xamoo néh la woone woonii na on à toute tout tous comparendare jusqu'à la fin fond des bas fond ndax toogg mouye dooxx wéérrou ccii tarixa yii dii kaacc rék gniir alalou aduna jééxx na fii. yallah sunu boorom gnii ak séne kaacc yii ccii sa diiné bou séél bii béh kagne ? Jusqu'à quand seigneur dieu ? jusqu'à quand ?

  • @lailahailallah2813
    @lailahailallah2813 4 года назад +5

    Ma khady👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌👌❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤que dieu te garde

  • @fatoukineniang8578
    @fatoukineniang8578 Год назад +1

    Rafetena

  • @babacarsarr8061
    @babacarsarr8061 3 года назад +3

    Vraiment té kou ko wax niou méré la

  • @aminagueye3318
    @aminagueye3318 3 года назад +2

    💓

  • @Ndiobathiam2011
    @Ndiobathiam2011 2 года назад

    Assalamou anleykoum mbok maachaa Allah. Sokhna Ma Khady linga wax deugla wayé nioune dioulite layé biir namou gueuneu rafété laniou Islam sante mais pas ay critique ak ay jugement. Naniou xolat sougnou waxine mou ande ak maximum de hikma

  • @dioufelimane2163
    @dioufelimane2163 3 года назад +2

    Ma khady Lou ler nga ye wakhe

  • @baaliou6634
    @baaliou6634 3 года назад +1

    Deaga Rek mo worr

  • @cheikhtidjianesarr8514
    @cheikhtidjianesarr8514 4 года назад +5

    Jah dieuf Ma khady mais jeunes bi gno wara yéwo pour li diékh

  • @Jesuis-Sonko
    @Jesuis-Sonko 4 года назад +2

    J'aime cette dame

  • @abdoulayeba2072
    @abdoulayeba2072 2 года назад

    Yalla rekk mofi née

  • @MrAlfred1704
    @MrAlfred1704 4 года назад +10

    League des champions de bokaler se joue au Sénégal au stade omnisport de touba

  • @babinewone2742
    @babinewone2742 4 года назад +2

    Koulou mane aleyha faan!

  • @diakawaka7033
    @diakawaka7033 4 года назад +1

    Walaye deugue le