Nécrologie : Ndéye Gueye raconte le film du décès de son beau père

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 11 дек 2024

Комментарии • 145

  • @adamaseck8816
    @adamaseck8816 4 года назад +21

    Yalnako yalla kharé aldiana amine 😭courage ndeye gueye

  • @salydia4242
    @salydia4242 4 года назад +34

    Yalla nako Yalla yeureum hareko aldiana firdawsi

  • @fallelleseck1650
    @fallelleseck1650 4 года назад

    Machallah ndeye Gueye sa sédé refét na yallah nako yallah yeureum té mayléne kholou mougne

  • @annamendy5245
    @annamendy5245 4 года назад +7

    Yalla n’a khipé firdawsi Mais condoléances à toute la famille particulièrement à Ndeye geuye

  • @diarrasalioudiagne6302
    @diarrasalioudiagne6302 4 года назад +6

    Oh Ndeye gueye khana sa khef yi mom yalla dalako fay may si gratuit ah ba bo amei décé sakh doko dindi mais yalla na yalla yeureum sa goro bi te khareko aldiana

  • @amyndiaye6877
    @amyndiaye6877 4 года назад +3

    Yalnako yalla yeureum te khareko aldiana

  • @bane257
    @bane257 4 года назад +91

    Ndeye amo ay conseillers xana sites yi ils s en fouttent de toi seni nombre de vues molen interester yewoul touti...essaies de vivre cachée un peu ak diegeulou

  • @mouhamedsaliousourang6456
    @mouhamedsaliousourang6456 4 года назад +5

    Yallanako yalla yeureum khareko aldiana

  • @fatougueye-zh7td
    @fatougueye-zh7td 4 года назад +9

    Yalla nako yalla yeureum 🙏🏽

  • @aidadiop2131
    @aidadiop2131 4 года назад +64

    Daguena barri wakh sénégalais li mom rafetoul amoul chance lane lagnou nettali si nit kinoumou deweh way senegalais changé lene bi méthode mom ndokhoul teh yaw ndeye gueuye warka wagni réseaux sociaux yi touti tu parles et raconte trop de ta vie môytouĺ beut ak lamigne sou rayoul lakal deh lakal dou rek handicap mais daffa barri ay façon moy toul deh noppi

    • @nannoye9468
      @nannoye9468 4 года назад +5

      Aida diop yaleuneu meu bourbii baleu Ndeye balmaa . Mais seu goro gagnou doo disolvant djouliii gnanalkoo. Amine cii gnaneu yii

    • @aidadiop2131
      @aidadiop2131 4 года назад +1

      @@nannoye9468 mane mom dama diomi si nitt gni sonnou tamit di setane yeneu yi...

    • @bitra6145
      @bitra6145 4 года назад +3

      Dissolvant... Il se peut que setoul pour diouli ? Yalla nagnou borom bi arr tei Sam gnou et dolignou soutoureu ak manou

    • @awandie
      @awandie 4 года назад

      Bilahi wakh ngako deug..mounal mbakhalou yap...papa papa papa .li yalnako djigue sakh...ak kheffam yi mou melni leupa leup ni...famlle bi dal yeureum nalene...

    • @aidadiop2131
      @aidadiop2131 4 года назад +1

      @@awandie ki daffa eupeul lol Melni tayal nimouneke papa papa boudou diekh Lampal bobam bamou eup kou sey rek yakarnani nop gua sa dieukeur mais ndeye gueuye teyoul darra na vivre sa vie privée pour mom ak yalla takh teh soraleh adouna da koudou fane yalla aki biram nagnou tey rek mane je l'estime tellement mais dama beug rek mou Dal teh tey Dal adouna da barri surprise

  • @khadydiouf9452
    @khadydiouf9452 4 года назад +1

    Eyy way😭yalla nako yalla kharé aldiana 😭

  • @maremembengue6873
    @maremembengue6873 4 года назад +19

    Yall nako yall yeureum te khareko aldiana

  • @papisgueye90
    @papisgueye90 4 года назад +3

    Yallnako yalla kharré aldiana

  • @mariemdibba2027
    @mariemdibba2027 4 года назад +4

    Yalla nako yalla yereum

  • @aichasy9811
    @aichasy9811 4 года назад

    Que firdawsi choix sa demeur internel🙏

  • @ngonefall153
    @ngonefall153 4 года назад +8

    Li dale dafa khew wayè lou bone khèwena .yalnako yalla kharè aldjana

  • @fatougueye7401
    @fatougueye7401 4 года назад

    Ndeye Gueye macha allah

    • @farimatasamba9447
      @farimatasamba9447 4 года назад

      Ndeye gueye nga balma wéro am décédé tok di éxpliqué wéro

  • @yamsdiouf8363
    @yamsdiouf8363 4 года назад +84

    Mais louy ndayou nite am deudj ngua tiim ko diko interviewée c'est quoi le projet

  • @yandefaye4268
    @yandefaye4268 4 года назад +12

    Bilay mane ndeye gueye dafma nekh khawma nane layy def bo guiss ko

    • @dijandiaye7778
      @dijandiaye7778 4 года назад

      Yandé yak kane ak mane tamit damako beugue rek

  • @aramedieng1066
    @aramedieng1066 4 года назад

    Sen Conn nakoula si khrfi Barbour al ay poss onglam en tte cast aside yi rafetna at kaddom rafet na mongui seuye seuye bi loutakh senegalai tour lou diaw rek lay xoll thie nit yalla na yalla so jikoyi gor guide dem yalla nako yalla yeureum khareko aldjane

  • @tallakatalibeserignebabaca2049
    @tallakatalibeserignebabaca2049 4 года назад

    Yalnako YALLA yeureum kharéko aldiana

  • @PEOPLE-km7vr
    @PEOPLE-km7vr 4 года назад +3

    Ndeysane yalah nako yalah yereume té kharéko aldiana si barki Seydina Mouhamed psl

  • @lingueredieng3654
    @lingueredieng3654 4 года назад

    Yalla Nako yalla yeureume té kharéko aldiana

  • @khadijakane9474
    @khadijakane9474 4 года назад

    Yalla nako yalla yeureum khareko aldiana

  • @coumbadiop6164
    @coumbadiop6164 4 года назад +7

    Gnii diko xase pour pose cils ak ongles yimou déf décé dou baptême nii mariage souye gnieuw doo tagoo,daf ko défone avant lii dii ame donc bayiléne séne yii ton beau père yalla nako yalla xaré aldiana allahouma amine 🙏

  • @ramaba9894
    @ramaba9894 4 года назад +2

    Amine yarabi

  • @mameboyediaw7758
    @mameboyediaw7758 4 года назад +10

    Repose en paix

  • @ndeyesophiediakhate7148
    @ndeyesophiediakhate7148 4 года назад

    que le bon dieux l'accueil dans son paradis firdawsi

  • @olymatadiouf2638
    @olymatadiouf2638 4 года назад +20

    Wakh dji barina thi koussa goro deh

    • @mamikayre7021
      @mamikayre7021 4 года назад +1

      Waa diomi

    • @khadyzadiop4980
      @khadyzadiop4980 4 года назад +2

      Ndeye gueye nak wagni wakh dji si deuthie NBA nèck loy natali ni chime yiwal way ak sa cil yi ta danga later si interview yi nabatoul touti wayy nèkh ngama ndakh danga beug seuy wayer yamal touti reck nga balma nack.

    • @mariemdibba2027
      @mariemdibba2027 4 года назад +2

      Ak ongle yi email by 😂😂😂

    • @faksbrown8739
      @faksbrown8739 4 года назад +1

      Sénégalais mo gnieme critiqué soff guene

  • @fatoumbye5290
    @fatoumbye5290 4 года назад +14

    May his soul rest in perfect peace Yalna suff seda si kawom 🙏🙏🙏🙏🙏

  • @dijandiaye7778
    @dijandiaye7778 4 года назад +1

    Yalla Nako yalla yeureum té kharé ko aldiana firdawsi

  • @ousmaneba1931
    @ousmaneba1931 4 года назад +2

    Rip yallah nako yallah yeureume

  • @salmacounta9713
    @salmacounta9713 4 года назад

    Kou dei rk ya bonnelénn sa goro dei ngay cils paix à son âme

  • @antarassouldieye4061
    @antarassouldieye4061 4 года назад +31

    Sa goro deh nga def say cils OK kone loloula

  • @kadysenegal7331
    @kadysenegal7331 4 года назад +2

    Man Lima diakhal version ndeye gueye ak version papa djine dafa diverse papa nena bimou kheye la dem diko nouyou fek ko mou guaniou

    • @ndeyerokhayabao352
      @ndeyerokhayabao352 4 года назад

      Je me suis posée la même question bref Bari na wakh trop

  • @SuperOUMZ
    @SuperOUMZ 4 года назад +1

    Ndeye gueye ligua wakh ak loussa dieukeur dji wakh cest diametralma opposé
    Yalnako yala yeureum

    • @antadiaw1603
      @antadiaw1603 4 года назад

      princesse torodo moma diakhal🤭

  • @6calimandiayecisse202
    @6calimandiayecisse202 4 года назад

    Que dieu lui pardon

  • @ndeyembarousene143
    @ndeyembarousene143 4 года назад

    Yalla nako yalla yeurem khare ko aldaina si barké Seydina Mouhamed Psl

  • @diamanovision4715
    @diamanovision4715 4 года назад

    Paix à son âme Yalla nako Yalla yeureum ci barké mouhamad

  • @Hakimi679
    @Hakimi679 4 года назад

    Yalna sarahame the ci sen loho

  • @matarmbaye3862
    @matarmbaye3862 4 года назад +27

    Nd geuye finga diap fofou la tarou djiguéne sëy

  • @mounassadio5174
    @mounassadio5174 4 года назад

    Massa paix a son ame

  • @juniordjikine572
    @juniordjikine572 4 года назад +3

    Paix à son âme

  • @smb3275
    @smb3275 4 года назад +14

    Bilahi wakhal way je comprend rien de ce senegal

  • @ndeyembackesymbaye1025
    @ndeyembackesymbaye1025 4 года назад +26

    Dindile pose ongles bi ak sil yi

  • @khadijasow4560
    @khadijasow4560 4 года назад +19

    Djéxal bi dé sa pose ongle yii lanou zoom

    • @pendambow7976
      @pendambow7976 4 года назад +5

      Khadjia sow gniye demm si deudji di introjematé nio wara tokkk dakh té loula bette meune la

    • @adamsadams6298
      @adamsadams6298 4 года назад +3

      @@pendambow7976 billea daf ko bett

  • @mamansalioudieng5784
    @mamansalioudieng5784 4 года назад +2

    Yalle nako yalle yeureume té yalle kharé ko aldiana ak képeu koufa nk ndéysane

  • @fatoumatasow3645
    @fatoumatasow3645 4 года назад +1

    Yéneu ndeye gueye mi beuguena mbakhalou yapp dh mouy yéneu 🙄

  • @khadydiop6867
    @khadydiop6867 4 года назад +1

    Rip père

  • @senesene2550
    @senesene2550 4 года назад

    Wa ndeye khéfyi nak

  • @amadoudiop2088
    @amadoudiop2088 4 года назад +1

    Mbakhalo yapp Thieye ndeye gueye

  • @myafashion8368
    @myafashion8368 4 года назад +5

    Eupeul guén legui deh meun guén ataya rek guéni fouralé tannk

  • @nadnad226
    @nadnad226 4 года назад

    Ndeye Gueye apparaît trop dans les réseaux socios en deuil au salon au marché garde ta vie privée un deuil est un moment de recueillement de prière pas d'interview que l'âme du défunt repose en paix

  • @mimidiop2088
    @mimidiop2088 4 года назад +3

    Bangaa dioyee ba parè mounan ga dindi faux cils yi ongles yii sangou jappou joulli nianalko yalla

  • @diordiorina7254
    @diordiorina7254 4 года назад +1

    wa kheff yi doko dindi
    mane dh warouna thi Senegal

  • @efodrame5119
    @efodrame5119 4 года назад

    Rip 😭

  • @pasdetemps7126
    @pasdetemps7126 4 года назад

    deuth sak daniouy koy expliqué ndeye vraiment desseh gua

  • @amichoubeybondiaye9973
    @amichoubeybondiaye9973 4 года назад

    Thieyy yallah wa Man diomiwouma rek🤔🤔

  • @radiadiop5117
    @radiadiop5117 4 года назад +1

    Antouka barri nga wakh

  • @ladouce9630
    @ladouce9630 4 года назад +2

    Wa khéf yi ak pause ongle yi tamiiit🤦‍♀️🤦‍♀️🤔

    • @Senfun221
      @Senfun221 4 года назад

      Dama warou dalll

  • @serignetoubarekdogoukaseci6857
    @serignetoubarekdogoukaseci6857 4 года назад

    Senegal sit Internet yi tambu guene lou bone bilahi legui dale dethie mome com guene té wale thiét

  • @moustaphcenter9845
    @moustaphcenter9845 4 года назад +8

    Iow deuthie bi safouleu d mbakhal mi molaaaa saf😂😂

  • @beugueyayam8543
    @beugueyayam8543 4 года назад

    ndeye gueye j t adore mais bari nga wakh trop nak

  • @nefertiish
    @nefertiish 4 года назад

    Wa man ndey gueye mi khana amoul bir keur tok thi mbedd mi ni gnou lay interview rek lii mom amoul benn class taffou si guinaw mur you tilim yi rek di wakh

  • @diaramata3153
    @diaramata3153 4 года назад +7

    Deileine diouli bouleine wakhetou raw nga def sa email ci biire deudjie bi

  • @mamediarrasall6728
    @mamediarrasall6728 4 года назад

    Léppp thiii néttte biii

  • @aidathiam7981
    @aidathiam7981 4 года назад

    Ndeye gueye xol bii dafa rafet beug na sey wayé nakh sa khéf yii ak ongle wagniii ko

  • @mamydabo5075
    @mamydabo5075 4 года назад

    Chacun sa vie privée c'est pas quelque chose qui doit être dévoiler . En plus ses choses artificielles ne sont pas belles à voir :ongles,cils . Désolée si j'ai offensé qui que ce soit

  • @fatoufatydrame1529
    @fatoufatydrame1529 4 года назад

    Ana perik blonde bi nekal nitt

  • @aminadiongue7485
    @aminadiongue7485 4 года назад

    wa say cils ak say ongle wa kone lolu la

  • @seydoutall547
    @seydoutall547 4 года назад

    Mais worona leene niaakh si baayi fethie nakc

  • @assanedia9042
    @assanedia9042 4 года назад

    Sa cild yi tamitr chak jour yak mom

  • @diatousar5185
    @diatousar5185 4 года назад

    Y

  • @katyfaye4767
    @katyfaye4767 4 года назад +3

    Tu parl trop goo way ak ongle yi amoo bène yare

  • @fatoumbaye9434
    @fatoumbaye9434 4 года назад

    Meunoulena nianal ki dem tengene bayi critike bok li sokhorla wala

  • @mamediarratine7240
    @mamediarratine7240 4 года назад

    Khamna warnga outal sa bop vie privée vraiment li dafa eup tjrs ngay étalé sa vie fi. Limoy lane. Journaliste sen intérêt rek yaw yay kham sa bop. C mon point de vue

  • @yayoushba9654
    @yayoushba9654 4 года назад

    Masseu metina

  • @limalo2118
    @limalo2118 4 года назад +1

    Mbakhalou yap bobou so démé lék gasi ba sour

  • @elhadjieldji3598
    @elhadjieldji3598 4 года назад +10

    Repose en paix