Maty Rose dit avec INSOLENCE, à sa mère : " ni toi , ni personne ne peut me séparer de Oumar". Cela me rappelle quand maman s'opposait à ma relation avec Queen Bineta. Mais moi, contrairement à Maty, j'ai pas crié sur ma mère. J'ai simplement refusé de manger. Et en pleine nuit, j'ai crié fort le nom de Binette et ensuite, j'ai fait semblant de m' évanouïr. Ma mère me voyant dit en pleurant " woooy li loumou done. Appelez bineta, vite,vite. Quand Binette arrive, en pleurant et dit " Fata mon amour", j'ouvre les yeux😂. Maman dit en tremblant " alhamdoulilah, si tu l'aimes à ce point, je m'oppose plus". Ainsi, j'ai épousé Binette, sans attirer la colère de maman😂.LOVE
Ndeye Touti le syndicat est fier de toi et on te donne la couronne de meilleure sœur de l’année 😊 Ibou laye aussi personne ne parle mais wallah il joue bien et c’est une bonne personne il fait tout pour protéger la famille malgré la mauvaise femme qu’il a Kadiza heureusement pour toi c’est un rêve mais ton karma viendra très bien Maty Rose déjà amoureuse de Omar mais elle ignore d’abord 😂 thieyy mbeugeul Franchement EvenProd vous êtes les meilleurs 😊❤🙏
Gayi naniouléne fonk diouli si Yonent bi Salallahou aleyhi Wa Salam … Lou Yalla gueureum la té santanéko … Proons sur le Prophète… Salallahou Ala Mouhamad
Sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa Salim ❤️ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa alla alihii wa sakhbihi
Même sans ses enfants elle doit retourner car son mari a déjà demandé le pardon pour l'erreur qu'il avait commis de ne pas avoir dit a sa femme qu'il prend une seconde femme mais Boury dafa méroun rek tmt
Hé Ne laisse jamais personne éteindre la lumière dans tes yeux et te faire perdre ton sourire. Fais tes choix, vis tes avec tes erreurs, fais face à tes peurs, laisse le passé derrière, avance sans te retourner et dis-toi que le meilleur reste à venir. Et si tu penses avoir perdu un petit bout de bonheur, ne t'en fait pas, un autre pourrait t'en donner le double !"
Merci Assane Séné ,enfin un commentaire bou ame ndjeurigne bilaye ,nous sommes tous concernés nak,ceux qui demandent des ❤pour ay serignes,ay dama accoucher, ay maylenma li ou la doivent vraiment lire ton message, bonne continuation
HEURES DE PRIÈRES DU 13 AU 19 DÉCEMBRE 2024 Fadjr: 06h13 Suba: 06h28 Tisbar: 14h15 Takussan: 16h45 Timis: 18h51 Gue: 19h51 Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Non vraiment qui a constaté que Ndiawar moo nékhal série bii😂😂. Mouné tu me dois 200millions nga diél les 80 et le reste me trouve chez moi tout de suite 😂😂😂. Mouné séydou ta gueule 😂😂😂🎉🎉. Si tu kiffes comme moi mets un like pour moi❤❤
42:00 Bilahi Bourry c'est trop mon coup de cœur ❤❤❤. J'aime trop cette femme mashaa Allah Mes larmes ont coulées je ne sais pas pourquoi 😢🤷🏽♀️.... mais quand on est dépassée par les épreuves de la vie, avoir une sœur à ses côtés ça fait toujours du bien. Longue vie à nos soeurs ❤🤲🏽
@@evenprodAh oui c est Capo? Dis donc il est fort ce mec,même en tant que artiste il cartonne.il joue bien et il a de l humour bravo à lui et vous tous!
Me le problem esq ndiawar esq dina gawa nagou nekat ak boury parsq mom khalisam rek moko nior😊 te soda mareme foumou tolou ndiawar khamna limou capable 😊❤
Commencement serie bi damako naron djieéppi ndakh dama fogon neeh Daffaye farr si li yayam dih deff , teh effectivement lolu ladon deff mais apres avortement bi la Changer de trop sax
Boury doundoul dra dieukeuram nop nako dioxnako bop lép yayam moko def dieukeur dji dousi dra da am foumou tek yayam dako beug . mais n'empêche kéne waroul nangou séy parents Di dieul décision a sa place
Bouri li motah magui nane seuye bou khalé yi magué dagué tog mougne dah khalé yi une très bonne leçon merci wa evenprod legui bo démé tu seras la deuxième 😢 amoule chance sa woudiou Di la yéb
Wei mais elle va partir chez les charlatans pr que sa n'arrive pas et elle risque de faire du mal à maty rose pensant que c elle qui va devenir sa coepouse
Omar diagne dé fatter na sakh foto yayam bii nakh maty rose ndeysane ❤😢ba kenn ladiatouko lanla meronne kerok maty est venue rekk omar fatter lou beurri ❤.je pense ke maintenant maty rose à changer à cause de omar aussi vu que kenn guiissa touko akk linguère akk seydou ausii vraiment il était temps que maty rose tourne la page 😊
Une belle leçon à retenir chez Maty Rose pour nous tous qui regarde les séries ce n'est pas les rumeurs qu'on entend chez les joueurs de théâtre qui est vrai avant de participer sur n'importe quelle discussion porté sur eux veuillez vérifier ce que vous parlez sur leurs dos S.P.M.S
Mon propre homonyme, meilleur ami de mon pére s’opposait á ma relation avec sa fille pasq j’ai passé tt Mon enfance en Europe et j’avais pas bcoup d’argent. Mais maintenant Alhamdulillah On pardonne mais on n’oublie jamais😊
Maty Rose dit avec INSOLENCE, à sa mère : " ni toi , ni personne ne peut me séparer de Oumar". Cela me rappelle quand maman s'opposait à ma relation avec Queen Bineta. Mais moi, contrairement à Maty, j'ai pas crié sur ma mère. J'ai simplement refusé de manger. Et en pleine nuit, j'ai crié fort le nom de Binette et ensuite, j'ai fait semblant de m' évanouïr. Ma mère me voyant dit en pleurant " woooy li loumou done. Appelez bineta, vite,vite. Quand Binette arrive, en pleurant et dit " Fata mon amour", j'ouvre les yeux😂. Maman dit en tremblant " alhamdoulilah, si tu l'aimes à ce point, je m'oppose plus". Ainsi, j'ai épousé Binette, sans attirer la colère de maman😂.LOVE
Sacré Fata 😂tjrs drôle 😂😂
Félicitations ❤😂
Yaye bondit 😩😂😂😂😂
Fata yaaa worr😂
Fata tu es ki 😅
Ndeye Touti le syndicat est fier de toi et on te donne la couronne de meilleure sœur de l’année 😊
Ibou laye aussi personne ne parle mais wallah il joue bien et c’est une bonne personne il fait tout pour protéger la famille malgré la mauvaise femme qu’il a
Kadiza heureusement pour toi c’est un rêve mais ton karma viendra très bien
Maty Rose déjà amoureuse de Omar mais elle ignore d’abord 😂 thieyy mbeugeul
Franchement EvenProd vous êtes les meilleurs 😊❤🙏
Ibou laye il est fort
@amadoutidianebalde4791 Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire. ❤
Wallah even prod les meilleurs ❤🎉💪
@@evenprodmane yéne rekk lay topp depuis idole mais dama lene di commenter mais déléne ma def signe 😂❤❤
Gayi naniouléne fonk diouli si Yonent bi Salallahou aleyhi Wa Salam … Lou Yalla gueureum la té santanéko … Proons sur le Prophète… Salallahou Ala Mouhamad
Sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa Salim ❤️ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa alla alihii wa sakhbihi
En Omar diang
Lou am solo lol
Salalahou ala mouhamed psl
Salallahou Ala Mouhammadine 🙏❤️🥰🙏
Respect pour boury qui accepte de retourner dans son foyer à cause de la recherche du bonheur pour ses enfants ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilay si s'était moi j ferais la meme chose pour mes enfants
Même sans ses enfants elle doit retourner car son mari a déjà demandé le pardon pour l'erreur qu'il avait commis de ne pas avoir dit a sa femme qu'il prend une seconde femme mais Boury dafa méroun rek tmt
Walay seuy moy lep djiguene diou bakh day seuy te yalla rk takh
Et surtout ces 2 là s'aiment encore❤❤❤
Hé Ne laisse jamais personne éteindre la lumière dans tes yeux et te faire perdre ton sourire. Fais tes choix, vis tes avec tes erreurs, fais face à tes peurs, laisse le passé derrière, avance sans te retourner et dis-toi que le meilleur reste à venir. Et si tu penses avoir perdu un petit bout de bonheur, ne t'en fait pas, un autre pourrait t'en donner le double !"
Yallah nalla yallah faye
Merci Assane Séné ,enfin un commentaire bou ame ndjeurigne bilaye ,nous sommes tous concernés nak,ceux qui demandent des ❤pour ay serignes,ay dama accoucher, ay maylenma li ou la doivent vraiment lire ton message, bonne continuation
❤❤❤
@@Bineta-o3l MRC bcp que dieu te bénisse inchallah ☝🏽
Merci assane ❤❤❤❤
Djiguéne boula yeureumé rek xamall ni une fois qu'elle t'aimera ce sera un vrai amour❤
Maty Rose limouy jouer c'est trop communicatif masha allah🥰
@alvinedemba368 👍
*Les 5 millions d'abonnés d' Evenprod mon combat Focus*
Abonné ci yaw, ndakh sa yènè ci even prod.🎉
@fatoudiouf8798 merci
@malcomboydiptsStyle Merci pour la force.
HEURES DE PRIÈRES DU 13 AU 19 DÉCEMBRE 2024
Fadjr: 06h13
Suba: 06h28
Tisbar: 14h15
Takussan: 16h45
Timis: 18h51
Gue: 19h51
Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Merci beaucoup
Merci 🎉
Mrc frere
Amna solleux machallah 👍
Amine inchallah
Non vraiment qui a constaté que Ndiawar moo nékhal série bii😂😂. Mouné tu me dois 200millions nga diél les 80 et le reste me trouve chez moi tout de suite 😂😂😂. Mouné séydou ta gueule 😂😂😂🎉🎉. Si tu kiffes comme moi mets un like pour moi❤❤
𝗧𝗲𝗶 𝗴𝗻𝗼𝗺 𝗮𝘆 𝗺𝗶𝗹𝗹𝗶𝗼𝗻𝘀 𝗿𝗸 𝗹𝗮𝗴𝗻𝗼𝗶𝘆 𝘄𝗮𝗸𝗵😂😂
@BarbieNoire-k1d ah oui ay millions you beurri saah🤣🤣
Moma diahal est ce douniou diokh si million yi
@@AmyNdiaye-cm8xf walahi on doit en avoir🤣🤣
😂😂😂il est drôle bilay
Kou bègue yobou yayame maka rék lalale jaime ❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤
Amine
😂😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤
😂
Maty rose yalna ko yallah may xolou mougn ❤❤❤
Khadija mo nara commandé Maty niou livrél ko yayou maty 😂😂😂😂
Lou kherre 😅😅
@juditekoite2961 Surtout ça. 😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
C’est la meilleure maison de production que je connais tellement Fidel et respecte l’heure et ses téléspectateurs félicitations et force à vous 😊❤
Wallahi deugg la
@@zeetv4328😊❤
@amadoutidianebalde4791 Merci. ❤
Depuis idoles lalen topp ba tey marquage à la culotte 😂
Maty rose joue bien son role ohh enplus belle est trop sublime was so beautiful ❤❤❤❤❤
@CodouNdir Merci beaucoup. ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ 43:43 43:45 43:46 43:47 43:47 43:48 43:48 43:48 43:49 43:49 43:49 43:49 43:49 43:50 43:50 43:50 43:50 43:50 43:51 43:51 43:51 43:52 43:52 43:52 43:52 43:53 43:53 43:53
Ndiawar sama dieukeur rek lakoy kholèh 😢nit kou am weurseuk akk tèranga mais yayam ak rakam nyi nioko sonal😭😩Yalnako yalleu takhawou kou bakh beugue dèretam
@fatoumatabintoucolley8878 Force à lui. 👍
Diapaliikooo rkkk inchAllah lepp dina bahh
Ma chérie on n’a le même problème 😢Bilahi Mais yallah na yallah diapalee sougnou dieukeur yi🙏🙏🙏
42:00
Bilahi Bourry c'est trop mon coup de cœur ❤❤❤. J'aime trop cette femme mashaa Allah
Mes larmes ont coulées je ne sais pas pourquoi 😢🤷🏽♀️.... mais quand on est dépassée par les épreuves de la vie, avoir une sœur à ses côtés ça fait toujours du bien.
Longue vie à nos soeurs ❤🤲🏽
Amen
@miss22395 👍
Chapeau à ndiawar un vrai artiste hors pair 😂 néna Seydou “ta gueule” 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Billahi 😂😂😂😂
Setana gouma sah di ré😂Esk camguèn ni commentaire yi nio dah Seri bi wuy😂😊
Bilay 😂😂😂
@riririri5817 Merci. 😍
Anta mom dafa tubabeh Ken duko rai ak wah ju barri 😂😂😂😂❤I love her❤❤
Bilahi comme mane rk 😂Motakh je l’aime bien
@ Bilie damako yaag setlu😂😂amul joti Ken mom.
@@jallowjerry16 bilahi fouleu la am
@@lennavivilennavivi khol ba rafet motahk 😍
@jallowjerry16 👍
Vraiment ki yor générique ak diko monter si evenprod mo meun limouy def ❤❤❤ c du hight level 🎉❤❤
C'est capo le monteur
@NjaayOusmane Merci.
@@evenprodAh oui c est Capo? Dis donc il est fort ce mec,même en tant que artiste il cartonne.il joue bien et il a de l humour bravo à lui et vous tous!
@@LAMPFALLTVOFFICIELDIRECTki bokone infidèle wala?
J'aime bien le papa a Omar Diagne,il est trop sage ce vieux.
@reussirenafrique1314 👍
J'ai remarqué le comportement de ndiawar quant sa maman prend la parole , kou fonk yayam lalal jaime❤
Le regard de Omar en vers sa tante kholou djépi 😂😂
Gnoune gni sakh di sétane kholou diépé lagni khol mère Khadija😂😂
@maramelo9036da bone way
😅😅😅
😂😂😂😂😂😂
@maramelo9036bilahi akka mako heinn😂😂😂
Mercredi tay bi yalla boumou nékh sounou dernier mercredi amine 😢
Kone tay samedi la 😂😂😂
Khana daguay nélaw tay la samedi kay😅😅😊
excuse-moi
😂
@@NiangMbayang-p8q méme que yaw aussi yéwogo DH nanal touti café😂😂
Khana Mercredi di 😂😂
Badiane sokhna Yeuré you rafett lay soll machallah 🎉❤
Meuna soll Lou rafet teh seytaner 😂😂😂😂
Yalla gua rousse lo Say none si barke seydina Mohamed psl 🎉🎉🎉❤❤❤❤
Amine
Amine
Amine
Ameen ❤
Amine
Yallah na diamou yague si barké seydina Mouhamed (PSL) ❤❤❤❤
Psl ❤❤❤❤❤
Salalahou aleyhi wassalam ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏
Me le problem esq ndiawar esq dina gawa nagou nekat ak boury parsq mom khalisam rek moko nior😊 te soda mareme foumou tolou ndiawar khamna limou capable 😊❤
Moh Ndiawar Boury rek la beugg
@ThielloLoum-ld7ui Hum, à suivre. Wayer boul fater Boury motah Ndiawar yeksi fi.
Kou yakamtiii tak Maty Rose ak omar Diagne beusseul❤❤❤❤
Omar wleu ass Diagne omar souko takke dou am sens
Man 2ème femme Asse diagne la yakamti
@remandiaye7442 Loutah geu yakamtiko. ❤️
Khana bala takk kéy omar fadiou ba wérr. Séy ak doff mom dîna doy warr déh. Amoul fénn
Kep kouy avancer publicite yi rk beussal j aime 😂😂😂
Kouy tog di sétan pub la khamoul😌😒
Temps amoul😂
😂😂😂
Badou
Mane mi 😂😂
Franchement j n’ai jamais vu une maison de production comme EP vous êtes les meilleurs ❤🎉
@PaMoussaDiallo-x7t Merci. ❤
Yenn Maty Rose mii nopp na Omar Diagne dh😂 thieuy l'amour ❤😂
Te hamouko dhe pourtant 😂😂
Mbeugeul yeurmandé monssi djitou sou mbeigeul di nieuw doko yeukk saxx montaxx djiguene mana beugg kouné
@@adjasaliou8309c'est l'experte qui parle😅😅
@@adjasaliou8309quel expert😂
yeurmandé mo eupou dolé mbeuguél
Anta elle est naturelle et innocente dafma nekh 😂♥️
Namou
Bly
Bilahi yaw 😂😂 même moi je l'aime
même moi aussi je l'am Billy paska dafa innocent
Commencement serie bi damako naron djieéppi ndakh dama fogon neeh Daffaye farr si li yayam dih deff , teh effectivement lolu ladon deff mais apres avortement bi la Changer de trop sax
Li guena grave moy di continue si ay tapalé toujours, mo dal Seydou.
Jtj
Ay😅 Sokhna mi di moy hypocrite bilay niit mo lendeume mais Boury elle s'habille descendment machallah ❤❤❤❤
Walaaye Sokhna elle me fume.J’ai horreur des hypocrites.😢😢😢
@aminatacisse818 Badou faux type ? 😂
@@evenprod bilay 😂 🙏🏽😍🥰❤️
Ndaysane Boury deff na choix bouko enrangé woul pour le bonheur de ces enfants 😢 Seuy metti naa ak limou Doundou yeup si keur dieukeur ram
Ceux que fait malheureusement beaucoup de femmes 😢 juste pour le bonheur et la tranquillité des enfants ❤ être une mère n'est jamais facile
Boury doundoul dra dieukeuram nop nako dioxnako bop lép yayam moko def dieukeur dji dousi dra da am foumou tek yayam dako beug . mais n'empêche kéne waroul nangou séy parents Di dieul décision a sa place
@@NdeyeMarieDioufybillahi
@@NdeyeMarieDioufyvérité
Pourtant bourry doundul lu graw dh djeukereum nopnako xana kay dafa dioum rk teih reconnaître nah erreuram
Wa nioulayou anta bi dou nguéne si wakh tmt ❤❤❤❤❤️❤️❤️
Bayilen di utiliser tourou yonenti bi pour ay j’aime
Waxal déh
Wakhatiko de
Bilay 😢
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci
Khadija déss na touty bouye wétt di xarou ndakh lépe dina keupou si kawame 😂🤝😂
Wahmalaa détt
Da bone way
@ToutaNdiayeTouta binlaye kï
Ass kay daye fépou
Lolou sa wara gaaw am
Wa ass diagne li kon niarel bi dou deug😮😮😮😮 yalna nek realité way 😊kouy wakh amin
@ThielloLoum-ld7ui Khadija modone guenteu. 😥
Amine 😂❤
Couple Sokhna mou magu ak Ibou lay meune namaa rayy😅😅😅😂😂
😂😂😂😂
@NdiemeDiouf-c4t Ibou Laye moye sey pas Soxna.
Nekh la def je rigole toujours à les voir
😂😂😂
Kou seydou soff reek lalal j'aime 😢😢
Séjour manou ma sof damako beug depuis une femme un mari 😂 ak les 4 fantastiques
@@niasssamba3006merci 😂😂😂
Billahi seydou loumou jouer nekh nama
Mane mom moy sama acteur franchement 😂
😂😂😂
Bouri li motah magui nane seuye bou khalé yi magué dagué tog mougne dah khalé yi une très bonne leçon merci wa evenprod legui bo démé tu seras la deuxième 😢 amoule chance sa woudiou Di la yéb
On s'en fou de Awa ou Niarel l'essentiel est k mongui delou nakh ndiabotam et abadane moy nek Awa aye domam
C la façon dont ndiawar la fait mo tahh mou demm souko aviser wonn dou demm
Ceux qui sont d'accord que Omar Diagne Assure Gravement pointez vous ❤❤❤
Kou Nagou Ni Omar Diagne Mogui Tékk Lou Khéré Woww Koguu Lalall❤❤❤❤
@wakhlouyydeffarnittgni4965 Merci. ❤️
Kharal ma bindate Sokhna Diagne Sokhna diagne ….niata yone lala wo 😢😂Ragual nala deh 😂😂😂
@madinaba-iw1pe Badou faux type ? 😂
Thiey yaye sacrifice boum dèff rekk si seuy rekk dom yè takh bravo à toutes les femmes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndiawar dama ko yaga beugue 😂😂😂 depuis diankhéne😂
Dafa xoromoi😂
AK bimouy wakh Daba koula wakh nga yéwou😅
Merci @@mormbaye2989
@ 😂😂
@astouniang-i5o ❤
Ndiawar dé bouné yaye ma youkhou 😂sa yaye dji déh yako makk😂😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂
Pourtant dou mak dé😂😂😂
Bilayy sene séquence lolou manoussé niakk😂😂
Ndiawar do nitt 😂😂
Cou geumni papa diadia bou ame niarel c'est le bonheur de omar rk diagne beusal j'aime
@NdebaSene Wayer lolou est-ce que dina yombou ?
Dommage que khadija ait rêvé pour l'histoire de la coepouse, j'aurais aimé que ça soit réel 😂😂😂😂
Ne t'inquiète pas son réve va devenir réalité😂😂 si elle ne change pas son comportement elle est très mauvaise
😂😂😂😂
Wei mais elle va partir chez les charlatans pr que sa n'arrive pas et elle risque de faire du mal à maty rose pensant que c elle qui va devenir sa coepouse
😢
Sokhna Diagne day tass keur day mate Di euf😂
Ndeye Touty est sympa 🎉❤❤que de meilleurs acteurs bravo à toute l'équipe d'evend prod
@bintaniabaly9953 Merci beaucoup.
Iboulaye dh bi série bi commencer batay Mogui dora wkh deugue 😂😂😂😂félicitations ibou🎉😂
Mbadou 😂😂😂
Si wakh deugu la deukk kay
Serigne sou diaré sa tank dina done gentleman bou niak diom meune fén téksi done dealer kay
sacré seydou😂😂
😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂 teii nonou la safeii lamigne nakk
Les beaux yeux 😍 de Maty meunnn nama rayyy 🎉🎉
@vieuxrabahfall4234 🥰
On réclame le retour du fameux thieré adiouma Boury rk lagne ci taamu djiek dji meunougn thieré 😂
😅😅 Yagui togne dh😅
@ndeyembenegueye12 Thiérè bobou la Ibou laye name. 😎
@ man sakh namna diotayou Thiéré bi😅
@@manishounaby2341 ah🤣
@@evenprod nioune skh mome lagne namm
Sokhna mou mak yay iblis deug 👹def li ngay def ba pare melni d'où yaw 😂niaw Khadija woudiou en téléchargement 💪😂😂
@MamefatyKane Soxna key mougui nonou. 😥
Ass Diangne 😂😂😂😂 nénako dell sisou
😂😂😂😂😂😂
Omar diagne dé fatter na sakh foto yayam bii nakh maty rose ndeysane ❤😢ba kenn ladiatouko lanla meronne kerok maty est venue rekk omar fatter lou beurri ❤.je pense ke maintenant maty rose à changer à cause de omar aussi vu que kenn guiissa touko akk linguère akk seydou ausii vraiment il était temps que maty rose tourne la page 😊
La vérité
Boula yalla takhalék ak nitt ko masoul wona khlata niaka diapal ni dina ko replace ak nitt ko masoul wona khlata am
Khadija, Maty Rose doussa ennemie dee, haral ba guiss yayam, apres ngay comprendre 😂
Bilaye bayiko rkk😂
Hahahahhh khamnga lanla? tay mou nékh😂
😂
Mais omar bou seyè ak maty pa ass dina mane tak yayam
@@ndiawaleye9208 meuna nek ndakh amougnou ben lien de sang
Kou téléchargé avant ngay sétan lalal j'aime 😂
khana kou amoul connexion moy def lolou 🤣
@@YADISCO-PRO peut être man dh wifi lagn yor té damay téléchargé
Dara gueunoul soff gua concentré ben étape ba annonce yi nieuw té meuno si dara
@@AmyNdiaye-cm8xflolou meune nama rayy 😂😂
Une belle leçon à retenir chez Maty Rose pour nous tous qui regarde les séries ce n'est pas les rumeurs qu'on entend chez les joueurs de théâtre qui est vrai avant de participer sur n'importe quelle discussion porté sur eux veuillez vérifier ce que vous parlez sur leurs dos
S.P.M.S
@ELHADJIMALICKGUEYE-s9y Merci.
Parlons de la beauté de sokhna Diagne mu mak waouh machallah 😍❤️
C normal dakh wa saint louis dagno rafét
Khawma beauté dhh mais meune na doulll dhhh
Bane nonou😂
Elle est magnifique
@@ModouDiop97920 gnio bok kogne saint Louis papam aka meun diagualé cour du soir
Mère Binta samb est mon idole sa simplicité ❤
Saison deux bi AK saison trois bi yallah nagniou féka fii this aduna yallah bou kéna manké inchallah amine ya rabi
Amine
Amine
Amine Ya rabbi
Amine waye inchallah 🙏🙏
Amine
Dimanche incha Allah le 15 décembre sm jourou anniversaire damayy demm ziaré Serigne Mountakha Mbacké Dina lenn nianall yenn nieupp incha Allah ❤
Hbd.. fasalèle niou si serigne by
Hbd touyou
@@fallndeye6092joyeux anniversaire ma chérie tei nga nianal ma nak ma am bac avec mention très bien tri guene si mane tmt
Bon anniversaire ❤❤
Ay wayy doma yobale😢
Serie bi khana farba ngom moko bindeu milion yi barina trop😂
Ma beugue Pa Ass wayy❤Khadija sa karma mogui gnew contane si deux sœurs 👯♀️ qui se retrouvent ❤🎉
@AstouGueye-w8t Yakar geu Pa Asse tak niarel ?
Sama toma❤❤
@@evenproda bien sûr
Yaye dior damako beugue nk 😂❤ alkhamdoulih ass diagnie daye takk diabar 😂 diadia daff ma béteuh ndakatéi anta moka eupou khél 😢
@aramegueye-ox8ff Asse Diagne dei bou takker ba Khadija diapako. 😂
Way sama yakaar tassna srx😂😂😂 Kone qui dadone guént nii sheut 😂😅😂
@AbdoulahadDiabaye Rêve leu wone. 😌
Yalna niepou am diam barcki cheikhoul khadim ♥️❤
Amine 🙏
Am
Amine chérie ❤❤❤❤❤❤❤
Amine
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Kou beugua teral sa yay mayma ❤
❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Iboulay Nar bi motakh amoul bat 😂😂😂😂..loum dadialé diokh ko di khar ay buts😂😂❤
😂😂😂😂
(Mbokou ndeya koy diour )sequence sou boury ak ndeye touty touché nama looll❤❤❤
"Mbokk ndeye mokoy diour" Ndiawar wane nako ak Seydou❤
@mbeyacisse2989 billahi limouy contre rak dji yeup terè woul takhawou nako
Walahi
Mane mi khoulo ak sama mak bi sakh fofou dafa dawe sama yarame😢
Effectivement
L'hypocrisie de soxna me dépasse vraiment.
Vraie vipère .
Mais machallah elle assure son rôle 😊
@aminatafall4175 Merci. ❤❤
Yalnaniou yalla mouthieul si beute lamign ak lépp louy lorr domou adama yalnaniou sétate série bi bamou diékh si diam 🙏🙏🙏
Lo gaw gaw fékk fii kennn😂😂❤❤❤❤❤❤❤
Bilay 🤣🤣
Khadija mi mbadou limou deef Omar Diagne mo keupou si kawam da melni kou commencé tépeutikou dé😂😂😂
Guissagoul dara sah ken dou def lou bone di am lou bakh 😅
@fatousow9718 Ah doyna ware. 😂
@@evenprod ah wa bakhna 😂😂😂
Ndiawar mon acteur préférée 😂😂😂
Alhamdulilah yalla na sénégalai yeup am diameu ❤🥰🩸🧨
Allakhouma amine inchallah
amine❤❤
Yw mi yalna gua téral sa wajour kom nig ko begué nél amin ❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂
Amine waye❤❤
Amine ya rabbi incha allah 🥰🎉
Amine 🎉❤
Amiine
Amine ❤🙏
Respect pour les pub c est grace a vous qu on regard les series chapeau
Vraiment
Alhamdoulilah yalla na nieup goudou fane❤
Allakhouma amine inchallah ❤🎉
Yàlla na niéppou am diamou 🤲🇸🇳
Amine xaye❤❤❤❤
On réclame toute la bande originale de la série. Tous les sons sont profonds. Celui de la fin de l'épisode d'aujourd'hui : une pure merveille.
Khadija diéppi nako😩😂😂
@ndayakane3482 😥
Délen dioulli thi yonen tibi allahoumma salli halla Mohammed ❤❤
Wakhal ba kharrr ass Diagne ray Nama 😂😂😂😂😂😂😂😂hohhhh rêve la
Anta missi mandou moma deff cas saniwoussi dondjiou xorom
@ anta dafa sonou si wakh dji 🤣🤣🤣
Da waronnn nek deug nk 😊
Combien de personnes aiment Mouhamed psl sur lui autant que moi ❤
Sallalahou alla Mouhamed ❤
Salal lahou Ala mouhamad❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤
EVENPROD vous avez les meilleurs affairou wasso dafaye diekhe Sénégal 🎉🎉🎉
Blh diotna dafa wara diékh
@mohamedelhabibndiaye8069 💪
Sonko rq inchallah ❤❤
Genrou Sokhna yi nio rawe sakh deumeu 😂 afficher indo dawal caboy 😅😅😅
Sokhna deh hypocrisie bimou andal dama yém mane😂😂ki elle est dangereuse 😂
@ c’est relle dh hypocrisie bi mouy jouer mo ame Senegal
@@ndeyeawandiaye1750lima nékh moy dafa jouer lou amm bilay❤❤❤❤❤
Nena dey vangewou ni yaye dior done traiter yayam bimouy doundou 😅😅motax diakhasser na nieup
@ non elle est très dangereuse 😅
Mercredi bou taye bi yalla boumou nek souniou moudiantal Mercredi si barki Psl ❤
Amine
Aminne
Amine yarabi
Amine yarabi
Amine yarabbi 🙏
Maty rose tamit raféte na lolo machallah
😂😂😂 gayi gaw nguen nak 😂 mais yalla na nieup ame diame Evenprod mention spéciale à vous ✌❤
Des cœurs pour la ponctualité et l’assiduité de notre Evenprod ❤️❤️❤️
Mon propre homonyme, meilleur ami de mon pére s’opposait á ma relation avec sa fille pasq j’ai passé tt Mon enfance en Europe et j’avais pas bcoup d’argent. Mais maintenant Alhamdulillah
On pardonne mais on n’oublie jamais😊
Bon courage yalla dièxoul
Toi qui lit mon commentaire qu’Allah t’ouvre la porte du succès 😞🥹
Amine🙏
Amine❤
Amen 🙏🏿
Amine
Amine
Khadijaaaa yaaa dougou thii Maty rose kiii moy nefartiti sow dèfanetè mooy sport favoris waame ioe wait rk 😂😂
𝑩𝒊𝒍𝒂𝒉𝒊 𝒎𝒆𝒊𝒔 𝒎𝒐𝒎 𝒌𝒉𝒂𝒎𝒐𝒖𝒍 𝒔𝒂𝒌𝒉 😂😂😂
Boule ma rayy wayyy
Pourquoi le autant de tass yakar😂😂 moi qui était content à l’idée de voir Ass Diagne épousé une deuxième femme
@assanediouf2309 Yakar gueine Asse Diagne takk ? 😂
Diop fall worna yalla raynama tay😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
@Missdieng 😌
Le regard de Omar envers sa tante ma tué😂😂