La femme de Sa Cadior raconte les calvaires de son mari

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 22 июл 2021
  • Ne manquez aucune information du Sénégal ou que vous soyez !
    Téléchargez nos applis ou visitez senego.com: bv3ey.app.goo.gl/sn

Комментарии • 430

  • @elhadjisow7372
    @elhadjisow7372 2 года назад +58

    Mou beuge diabar bou melni ki beuseul jaime stp❤️💪🏿

  • @ninkinanka3644
    @ninkinanka3644 2 года назад +50

    LES ASSOCIATIONS DE FEMMES DOIVENT DÉCORER CETTE BRAVE FEMME QUI DOIT SERVIR DE LEÇON À CETTE JEUNE GÉNÉRATION DE JEUNES FEMME. COURAGE ET QU'ALLAH FASSE QUE TON MARI REPRENNE SA SANTÉ. MERCI PAPE MAGUETTE POUR CET INTERVIEW QUI VIENT À SON HEURE.

    • @jaynprods2
      @jaynprods2 2 года назад

      Regarde rek gnom nioko warone xalat mais dedet ...et pas que niom la lutte .. l'association des lutteurs les promoteurs etc... association you bari diobouniou... Cette femme doit etre amené avc ses enfants en espagne

    • @maimounasene6488
      @maimounasene6488 2 года назад

      merci beaucoup elle mérite vraiment d'être décorée

  • @alimaseye1542
    @alimaseye1542 2 года назад +95

    Gni Goré gnou ngui goré batay parce-que mariage c'est pour le meilleur et pour le pire Big respect Khadija

  • @Jordan-hu1dw
    @Jordan-hu1dw 2 года назад +22

    Cette femme est vraiment exceptionnelle respect à toi que le bon Dieu t’assiste 🤲🏾🙏🏻

  • @khadythiam6528
    @khadythiam6528 2 года назад +37

    Une femme exceptionnelle mashalla yala nala yalla faye

  • @ahmeds7785
    @ahmeds7785 2 года назад +21

    Je me suis toujours dit qu'une bonne femme naturellement n'existe pas mais cette femme a totalement désapprouvé mes pensées. Franchement je n'ai jamais vu une femme comme celle là. Je voudrais vraiment qu'elle rejoigne son mari en France car je pense que sa cadior devrait rester à Paris pour bien suivre son traitement. Donc si on peut aider la femme à rejoindre son mari ce serait la meilleure solution.

  • @damediouf9627
    @damediouf9627 2 года назад +22

    Courage Khady yalla nala yalla takhou si barké Serigne SALIOU

  • @mamethiernondiaye9466
    @mamethiernondiaye9466 2 года назад +18

    Sokhna sou bakh migui ni Machaallah takhawou gua sa dieukeur yalnaléne yalla geuna sam 😍😍😍

  • @lol_fatou1689
    @lol_fatou1689 2 года назад +13

    😭😭😭😭😭barke alhurane jiguene geunoula j’arrête pas de pleuré courage rk walahi digua am lou bah inchalla

  • @cheikhtalibouyadjitte8855
    @cheikhtalibouyadjitte8855 2 года назад +20

    Ya bakh diame si ioe 🙏❤❤🙏

  • @desirealqanah9521
    @desirealqanah9521 2 года назад +22

    Force à toi . que Dieu te fortifie et donne la santé à ton mari

  • @loucha7179
    @loucha7179 2 года назад +51

    Cette femme je l'aime bien en plus d'être belle elle est digne

  • @ababacarkhalifa5398
    @ababacarkhalifa5398 2 года назад +15

    Bilay ki dama kaye gnianal rek yalla wereul dieukereum defal ko were ak goude fane k allah vs beni

  • @ndiaboutadiouf7912
    @ndiaboutadiouf7912 2 года назад +43

    sacadior amnga Lou diafe.diabar.boubkh nga am.loko meuneu teye .rekk.diap ko boubakh

  • @batorniass481
    @batorniass481 2 года назад +8

    Trop bax même en amitié dafa goré bilay walay 2012 ba ni niouy ande mais de jour en jour dalay guena won lou bax mais courage rek copine yalla dinala fay sa xol🙏🙏🙏

  • @yawsamayaye9347
    @yawsamayaye9347 2 года назад +9

    Courage Khady Diallo Yalla nala Yalla Geuna Diapalé Kou Yalla Beugue Fawou Mou Tékk la Ay Natou Machalah Mougnal Yalla Na Sa Kadior Geuna Wér Ak Mbolém Gni Tawat Courage Courage Courage🙏

  • @labsolugueye1474
    @labsolugueye1474 2 года назад +25

    Djiguéne Balanga khamnii Beugeu nala Deugeu nga Nékeu thi situation Tankeu nékothi situation bou Dificile Mounoo khamnii kii Beugeu naleu wollah bougoula Billahi Yalna jameu Yageu ❤️🙏

    • @kharyfaye8324
      @kharyfaye8324 2 года назад +3

      Lou léér nga wah

    • @labsolugueye1474
      @labsolugueye1474 2 года назад +2

      @@kharyfaye8324 Frér limay waxni aka moco xam Billahi boo Amoull Diafè Diafè adouna Mounoo xam kinga nékal Beugeu naleu walla bougoula Billahi boula beuguè tèmouy Deugeu thi Mome même si Bo Dèmon ba yoro 50 Fr Doutax mou bayi Billahi tay Andeu ak io badè rék 😌

    • @mouhamedmoustapha684
      @mouhamedmoustapha684 2 года назад +3

      Linga waxx deugueleu walayy azim diabar diou baxx la yalla xamnako

    • @Seck221
      @Seck221 2 года назад +3

      @@labsolugueye1474 lou weir

    • @labsolugueye1474
      @labsolugueye1474 2 года назад +1

      @@Seck221 Damoco Dounou 🥺

  • @abdouba2241
    @abdouba2241 2 года назад +63

    Je ne suis pas d'accord avec le journaliste il n'est pas professionnel ont attendait d'autres questions plus important devant cette brave femme

    • @salioumboup1655
      @salioumboup1655 2 года назад +1

      Djigneu du worka ndassane

    • @fallmandione1463
      @fallmandione1463 2 года назад +2

      Ki khana faux journaliste la

    • @omarleytindiaye7854
      @omarleytindiaye7854 2 года назад +6

      Journaliste bi dafa nobb khalebi ya des questions qu'on ne pose pas a une femme mariée

    • @abdelohod4884
      @abdelohod4884 2 года назад

      Ki dou journaliste ki day commenté

    • @kamaracherif
      @kamaracherif 2 года назад

      Mai journaliste bi Est-ce que cv

  • @khadymbaye433
    @khadymbaye433 2 года назад +11

    Khady yi ayy mougne katt lenn 💪🏽

    • @mouhamedmoustapha684
      @mouhamedmoustapha684 2 года назад +1

      Ba melngani Khady mi rek machallah ki mom kou baxx la walay

  • @wademadjiguene4514
    @wademadjiguene4514 2 года назад +10

    Macha allah khady t'es spéciale, non problème nio bok cogne du courage ma belle

  • @meujnatdiakhate8470
    @meujnatdiakhate8470 2 года назад +4

    Boul thiatou diabarou diambour dji way deil wakh machallah yeukhziiikk

  • @serigneamar5401
    @serigneamar5401 2 года назад +12

    Yalla nelen yalla.diapele sokhna si.ko am gor gui yalla na sadiapot magui ba dila teral

  • @peaceandsalam2852
    @peaceandsalam2852 2 года назад +10

    MachAllah yàlla neleen buur yàlla taxawu

  • @aminandiaye3303
    @aminandiaye3303 2 года назад +6

    Machalla yale na yalla goudale s'en fane si Barké seyedina Muhammad si Barké Serigne Touba 😪😪

  • @fatisall8581
    @fatisall8581 Год назад +1

    Machallah ma sœur yallah doli soutoura est courageuse à weltanam ❤️😍

  • @ajaniang
    @ajaniang 2 года назад +2

    Cet animateur je ne dirai pas journaliste est très c** courage Mme vous êtes une femme brave

  • @iboudiop9093
    @iboudiop9093 2 года назад +6

    😭😭😭😭tu es la meilleur

  • @ballawade6231
    @ballawade6231 2 года назад +2

    Mashalla yalla na sa borome keur gnibisi si saye lokho inchallah 🙏🙏 diambar deugue 😥😥

  • @tigresseferoce1431
    @tigresseferoce1431 2 года назад +2

    Toute magnifique ❤️ courage ma chère.

  • @boubajunior9401
    @boubajunior9401 2 года назад +15

    ❤️❤️sunu diabar dji diambar nga mais yallah dinala doli soutoura ndakh souniou wadji tamite kene dou mom Sacadior 2 yalna ko sunu borom defal diam

    • @ibrahimadrame7330
      @ibrahimadrame7330 2 года назад

      Cette journaliste n'es pas professionnelle ont dirais il veut draguer la femme soyez professionnelle le journalisme est sacré

  • @ibrahimaniane6508
    @ibrahimaniane6508 2 года назад +11

    Brave femme ,goree baxx machalla👍 sa kadior niit kou bakh la bilahii

  • @maimounasene6488
    @maimounasene6488 2 года назад +1

    mashalah femme sokhna khadija, yalnala ylla féye , défko sa njaboot, gnou mag dila téral , yalna yalla may sa cadior féh, vraiment tu est une bonne dame

  • @ousmanendiaye2731
    @ousmanendiaye2731 2 года назад +6

    Mangi nianal sa cadior wer ngir sokhnam sugorèsi ndeysane yalnaco yalla doli wèr ak khèweul

  • @ousmanelom6274
    @ousmanelom6274 2 года назад +1

    J'ai regardé quand son mari était malade et aujourd'hui c'est une femme courageuse et brave elle mérite un respect

  • @daoudasadio5407
    @daoudasadio5407 2 года назад +4

    Je vous souhaite tous le bonheur du monde

  • @falloukarimmbow4981
    @falloukarimmbow4981 2 года назад +1

    Femme de sa gadior. Khady Diallo tu es dingue yalla nala yalla maiiy tawfékh.

  • @omardiop3349
    @omardiop3349 2 года назад +2

    Machallah yalna diam yague

  • @modougaye6646
    @modougaye6646 2 года назад +1

    Yalla nako yalla diapalé cette femme et son marie yalla maye ko wêr ak goudou fane walahi elle es bélle cette femme Machalla

  • @khadimfall580
    @khadimfall580 2 года назад +3

    machallaha sokhona so bakh yalla bakhena

  • @myamya6523
    @myamya6523 Месяц назад

    oh machaAllah Khadija rek nga meune toud. Yalna borom bi subhana wa tanhla sameu leneu

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 2 года назад +15

    Nako mariem fay diapale mou deem seti dieukeur dji nak

  • @djilygaye9169
    @djilygaye9169 2 года назад +1

    Machallah sokhna ci

  • @gueyemalick6850
    @gueyemalick6850 2 года назад +1

    Machallah laf thiat

  • @kinediongue3225
    @kinediongue3225 2 года назад +1

    Ndeysane je la connais très bien soit forte ma belle

  • @saracoutureprestige
    @saracoutureprestige 2 года назад +4

    Machalla ma sœur

  • @macydiouf4172
    @macydiouf4172 2 года назад +1

    Sos una mujer grande tkm buenas hermosa chicas bellas Ojalá Dios t ayudar por siempre

  • @abdoulayediakho7237
    @abdoulayediakho7237 2 года назад

    J'ai jamais vu une femme aussi brave comme celle là mashallah, vraiment jiguenn gueunoula,ki warnagn ko diapalei mou rejoindre son mari

  • @ndiaboutadiouf7912
    @ndiaboutadiouf7912 2 года назад +6

    machalla.

  • @bambayaya740
    @bambayaya740 2 года назад

    Que dieu vous protéger et donne la santé à ton marie inchalah bravo à toi c'est ça on appel brav femme et din longue vie à vous tous

  • @mouhamedmbayesaliou1191
    @mouhamedmbayesaliou1191 2 года назад +3

    Ndeysane ya Bakh waay yalla nala sunio borom dollé takhawou çi Barkep serigne salihou Mbacké

  • @matarsarr2022
    @matarsarr2022 2 года назад +1

    Machallh way yallana yalla douli Diam ❤️❤️❤️❤️

  • @boromebakh28
    @boromebakh28 2 года назад +2

    Bilahi khamou mala dh mais jiguéen bou am koleuré ngua mais yalla naléen yalla bolé yakk sa kadior machallah 🙏🙏🙏
    Le présentateur il doit être professionnel sur son travail mais pas a donné des compliments sur la femme de quelqu'un c'est juste un constat.

  • @ndionegenerallo3284
    @ndionegenerallo3284 2 года назад

    Machallah brave femme yalla na yalla taxaawou lén surtout ne change jamais gueuneula goorgorlou rék yalla bakhna boula dara feukkeu inshallah sa jaaboott dina ñiou lén dëgg inshallah yalla dinalën barkél

  • @khadimdiouf8043
    @khadimdiouf8043 2 года назад

    Une Femme exemplaire machalha yalna nalla yalla defall diam...tawfekh rekk...👌

  • @thiernondour3449
    @thiernondour3449 2 года назад

    T'es forte k dieu vous protége 🙏

  • @mbackekandji2648
    @mbackekandji2648 2 года назад +2

    Machalla braf fame yalla dinako fay si nianbot gui

  • @djibyfaye3411
    @djibyfaye3411 2 года назад +1

    J'ai les larmes aux yeux bilaye yalna la yalla faye sa khol té yalnama yalla maye sokhna sii mel nii yow

  • @cidihiocisse6125
    @cidihiocisse6125 2 года назад

    Femme bi yalla nako yalla takhawou une femme digne té goré

  • @makharyndiaye5922
    @makharyndiaye5922 2 года назад +5

    Machalla

  • @antambaye6059
    @antambaye6059 2 года назад +1

    Ndeysan fière si ni xam nala outé ak gni xam adji sarr wa guediaway niepp content nane si yaw faté wo bila sacadior di téral guédiawaye guenté lou riche Machallah con sou ndogal nieuxé ga mougne rek wath bilay xalé dakar sourtou nioune wa guédiawaye seye rek nanouy deff la preuve wenibik khady Diallo c’est Anta Mbaye ami d enfance et meme camarade de classe ces pikine est /B 🥰🥰🥰

    • @supasane7432
      @supasane7432 2 года назад

      J'etais Làbas Aussi Pikine Est/B

  • @mantakyensslamthioubarry
    @mantakyensslamthioubarry 2 года назад +1

    Non bilahi wollahi maki dioy machallah ma sœur yallah nala yallah fay sa xol oh 😭😭🙏🙏🙏🙏👏👏👏👏👏🇸🇳🇫🇷

  • @ousseynoudieye7600
    @ousseynoudieye7600 2 года назад

    Machallah damalay takal grade bou Aline sitoe diatta wala bou ndaté yalla vraiment yalnala yalla Faye nioune khamouniou sa cadior dé mais geste bi ga déf daf diafé si adounay tay

  • @makeitreal6918
    @makeitreal6918 2 года назад

    Une femme extraordinaire pour moi li amatoul Masha Allah

  • @madjibop3617
    @madjibop3617 2 года назад +1

    Ndeysanne, qui djiguène bou bakh la, machalah
    Yalla nalèn yala takhawou

  • @BOROM__NDINDY
    @BOROM__NDINDY 2 года назад +4

    Ndeysane😭❤️😭❤️Billahi sama yaram bii mogui daw djiguen djou bax wallahi louko way dieundé diar nako yallah nama yallah may sokhna sou mélni ioe❤️🙏

  • @ousmanediouss3387
    @ousmanediouss3387 2 года назад

    Diaroul dioye doko masa rétiou bakh yiwe goré aka ame solo yalene yalla samela AK sa diabote yeupe défale léne diame AK salam soutoure adouna AK alakhira inchallah

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 2 года назад +1

    Macha allah yalna yalla same

  • @loubesstv3494
    @loubesstv3494 2 года назад +1

    Machalah khady yague fi rk

  • @bourybarry3911
    @bourybarry3911 2 года назад +1

    Sokhna sii bakhna rafetna cool toropp. Yalla n'a leene yalla diappalé yokkeu léne soutoureu. Diambar nguaa

  • @cheriffall6682
    @cheriffall6682 2 года назад

    Machalla je l'aime gravement 💖🙈

  • @khassimfofana3229
    @khassimfofana3229 2 года назад

    Machala vraiment les femmes du nom de khady vous êtes les meilleures mane sama yaye khady la toudou senegal gni laniou warr di feusseul sa cadior amnga vrai sokhna yalla naniou yalla may niou melni ki khady yalla nalla yalla diapalé te fayla si say dome inchala vraiment jai pas les mots bilahi souma amone ayy milliards maylako bilakhi

  • @sidathmalangdiedhiou3523
    @sidathmalangdiedhiou3523 2 года назад +1

    Machallah lep dina bakh inchallah

  • @falloumendy370
    @falloumendy370 2 года назад +1

    Elle est tres brave❤👊❤

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 2 года назад +2

    Boul déglou kénn ku bone adouna sakhoul topal sa borom keur bu bakh yalla dinako wereul inchahala

  • @lapiochepp433
    @lapiochepp433 2 года назад +2

    Jiggenou aljanna firdawsi..amine souma amone millions maylako ndax sa goré

  • @leminsarr9667
    @leminsarr9667 2 года назад

    Machalah c une femme exenplère c une vrait machalah

  • @laminefallnabien5607
    @laminefallnabien5607 2 года назад +8

    Salam sokhna khadi mi de loléne waxsi mbaxame tamit menoléne wax lép mane dalle lima koy nianale Yalla mayko lép limou beug si adina mome ak sa sakadior

  • @biramegueye3366
    @biramegueye3366 2 года назад +1

    Yalla nala Yalla fay sa mougne Masha allah

  • @leminsarr9667
    @leminsarr9667 2 года назад

    Machalah sa cadior amnaa diabar mougne rek inchalah dinaa bahee

  • @lepatriote9423
    @lepatriote9423 2 года назад +1

    Machalla elle est un exemple.

  • @ndeyemariemebob4164
    @ndeyemariemebob4164 2 года назад

    Machala brave femme yalla dinala feyy sa khol def ko si djaboot si barké Mouhamet (psl)

  • @cheikhtalibouyadjitte8855
    @cheikhtalibouyadjitte8855 2 года назад +7

    Sante Yalla

  • @papediene2025
    @papediene2025 2 года назад +1

    Masahll yallanga ame diame

  • @zaleandragonabougrandyoffa7366
    @zaleandragonabougrandyoffa7366 2 года назад

    Ndéysann 😢 mom ak ndéye Gueye danio beugg sénn djeukeur mashallah 💞

  • @ablayembaye8405
    @ablayembaye8405 2 года назад

    Brava Sokhna dieureudieuf

  • @modou2004
    @modou2004 2 года назад +2

    Elle est mignion wollah ♥️

  • @bintacoly7034
    @bintacoly7034 2 года назад

    Ndeyesane weurseuk bo guiss khathiou waye la kholal situation yinioudone dounde tey dji mane je me dis que yala moni dinako tek natou bamou voyage bafaye ame tey weurseuk tey et je félicite et encourage vraiment sa femme franchement tu es forte machalah yala nalen yala same

  • @baydarou4883
    @baydarou4883 2 года назад

    Ma sha'allah sokhnasi yalnaléne yalla geuna takhawou yokko kou weur thi berkè yonénti bi

  • @fidelmathieumendy3857
    @fidelmathieumendy3857 2 года назад +1

    Je rêve de ce genre d’épouse 😭 cette femme et sa cadior comme mbourou ak sow Yalla nalen borombi samb weral dans dieukeur bamou delousisa wëtt

  • @ndiaboutadiouf7912
    @ndiaboutadiouf7912 2 года назад +13

    lolou rekk lalay.denk

  • @makhtarsalioukhelcom8410
    @makhtarsalioukhelcom8410 2 года назад

    Machallah yalnala yalla sutural barké Mame cheikh Ibrahim fall lamp. journaliste bi wérul

  • @malicksy2339
    @malicksy2339 2 года назад +1

    Machalla longevité de vie

  • @laminendiaye1255
    @laminendiaye1255 2 года назад +1

    Respect à toi

  • @morkane8485
    @morkane8485 2 года назад

    Machalla wakhtane bi amna solo khady Diallo yal nala Yalla may godou fane ak weurgui yaram yal niouko Yalla may niou diabar Diou meulni yaw contane na si trop bilahi ya kham lo beug sa adouna yal nalako borom bi defal lolou 🙏❤❤❤❤

  • @ndiaboutadiouf7912
    @ndiaboutadiouf7912 2 года назад +8

    tu es une brave femme

  • @abdoumane3557
    @abdoumane3557 2 года назад

    Bonne chance pour la suite à Sa Cadior

  • @mamemalickngom4949
    @mamemalickngom4949 2 года назад +1

    Une brave femme

  • @layendiour11
    @layendiour11 2 года назад

    J'aime beaucoup Sa Cadior nit kou téy dal gueum yalla du courage madame le meilleur reste a venir diappal rek yalla diekhaloul

  • @ousseynoudieng5084
    @ousseynoudieng5084 2 года назад +1

    Machallah KHadijia est doul nall

  • @sallboukharagne2590
    @sallboukharagne2590 2 года назад +3

    Yalla nala yalla diapale kouni amine yalla nala yalla faye