🔴Sa Cadior explique la gravité de son maladie c'était trop dure..mais Balla Gaye ak Sa Thies ay vrai

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 апр 2024
  • #lutte #etdrmedias #lamb
    👍 Merci de laisser un pouce bleu 👌
    Visiter également notre site web: www.etdrmedias.com
    NOS réseaux sociaux :
    / etdrmedias
    / etdrmedias
  • СпортСпорт

Комментарии • 206

  • @salyallemomuawrksarr8652
    @salyallemomuawrksarr8652 Месяц назад +53

    Balla gaye 2 et sa thiés danio bakh te gorèe Aliou seye 2 tamite nitt kou bakh la yalla nalene yalla may ndam si barki seydina mouhamed ❤❤❤❤

  • @SowMadiaw-go2uc
    @SowMadiaw-go2uc Месяц назад +14

    La ilaha ila anta soubhanaka inni kountou minal zalimina sa cadior yala nako yala taxawou

  • @papagorakebe7594
    @papagorakebe7594 Месяц назад +32

    No kou meun beuré diantalone tieuy adouna yalna la yalla défal tane boubakh

    • @papefall7062
      @papefall7062 Месяц назад +4

      Bilahi frère , j'ai un frère qui est en France mais mom reikk la beug. Yalna Yalla may KO werr

  • @zaltoure134
    @zaltoure134 19 дней назад +1

    Yalnala yalla maye werguou yarame thi barki mouhamed

  • @user-ys2dd8fb7y
    @user-ys2dd8fb7y Месяц назад +16

    Sa cadior 2 nittou aldjana la khol bi wekh tall mashallah yallah nako borom bi geuneu dolli werr barké alkhourane 🙏

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 Месяц назад +14

    🇺🇸 depuis tout petit je les toujours estimé yalla nala yalla taxawou grand si barké seydina Mohamed psl ❤akh bèpp djioulite maïNiou doundou bou barkèl moudjiou bou raffètte NGeureumou wadiour yi mousseulniou si mbougeulou bammèl si barké seydina Mohamed psl ❤

    • @ZenebouSow
      @ZenebouSow Месяц назад +1

      ❤❤❤❤amiiiiiiiine Wayy fall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-ii9ip4mq6o
    @user-ii9ip4mq6o Месяц назад +8

    للهم يشفيه ويعافيه يارب العالمين ❤❤🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲😢😢انشاء لله ❤❤

  • @BayeNiass-xu4ry
    @BayeNiass-xu4ry Месяц назад +26

    Sa cadior yalla n'a la yalla maye weure si Barke alkhourane inchallah

  • @pacoboungoorakkdudu3396
    @pacoboungoorakkdudu3396 Месяц назад +1

    Sa Cadior geneu yagg geneu weer thi barkep kou tedd kii yalla baxna té waxoul kéeen Dara dundeul diambar dila nianal yaw akk sa Sokhna sa boroom yokou seen soutoura té défal léen liii geune thi yéeen inch'Allah 🙏
    Balla gaye akk Sa Thiès moom yalla naléne sa boroom geneu taxawou thi barkep kou tedd kii inch'Allah baxx reek moo am solo yalla baxna diap reek teweu bayiii. Dieureudieufy Boroom Touba 🙏👏👌

  • @user-wv1og3bl3j
    @user-wv1og3bl3j Месяц назад +7

    BONNE GUERISON. QU ALLAH LE TOUT PUISSANT VOUS ASSISTE VOUS PROTEGE VOUS BENISSE GUIDE VOS PAS. AMINE YA RABBI.🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @DMVTVSPORT
    @DMVTVSPORT Месяц назад +17

    Yalnala yallah défal diam boubakh barkép brome touba

  • @user-mg2nt7df3n
    @user-mg2nt7df3n Месяц назад +5

    Ndeyssane balla ak sa yalnalene yalla may ndam ay❤you rafete lagne yor wayee yaw kene genoula yalnala yalla may were

  • @babacarseck3366
    @babacarseck3366 Месяц назад +27

    Yalla nala yalla maye tane thi barkepp seydouna Mouhamad

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Месяц назад +9

    Sa cadior ndeyssane 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @MouhadeSarr
    @MouhadeSarr Месяц назад +8

    Sa bilayy nitt kou bahh ki holam lako yalla Faye

  • @albouraq24
    @albouraq24 Месяц назад +1

    Alhamdoulilah Macha'Allah Yalna Yalla doli soutoura

  • @user-cn5ux5xi9w
    @user-cn5ux5xi9w Месяц назад +8

    Sa cadior 2 diamou kassé inchallah❤❤❤

  • @salyallemomuawrksarr8652
    @salyallemomuawrksarr8652 Месяц назад +7

    Ndayssane aka bakh te gorèe kassè mabo doundeul way borom xôlou diaman bi❤❤❤

  • @kamassaer2661
    @kamassaer2661 Месяц назад +1

    Machalha sa cadior nite kou bakh la khamante nane depuis paris mais kou bakh laa ta yarouu 🙏🙏

  • @Mouhamedba-1975
    @Mouhamedba-1975 Месяц назад

    Longue vie à toi Sa kadior. Puisses ALLAH SWT t'accorder une santé de fer et te préserver

  • @ModoubaraMbaye
    @ModoubaraMbaye Месяц назад +7

    Dieu décide tous yalla nala yalla maye were thui barké mouhamed geume yalla reck moye deugeu

  • @papemoussadiop83
    @papemoussadiop83 Месяц назад +7

    sa kadior ndana la champion

  • @abygaye-cx3dh
    @abygaye-cx3dh Месяц назад

    Dagua toyal sama khol yalla nala yalla défal diam arrala bopam soutoural laa lakala fou yak agoul amine yarabi

  • @amdymoustaphaakasa5963
    @amdymoustaphaakasa5963 Месяц назад +2

    Ndeyesan yallah nko Yallah takhawo barkebe borom touba mame cheikh ibra fall Lampe baboul mouridina

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5b Месяц назад +3

    Diadieuf mbeur sa diabar nio bok kogne Guediawaye mais kou diambaré leu bilahi thia kaw thia kanam rék 😢😢😢😢

  • @babsbaba19
    @babsbaba19 Месяц назад +1

    Ça se voit que c’est quelqu’un de bien Qu’Allah le préserve continue de le protéger par sa bienveillance

  • @aitandour5974
    @aitandour5974 Месяц назад

    Sa cadior yalla nala yalla may wére ak goudou fane si barké seydina Mohamed (psl )Amine

  • @oumoucisse1295
    @oumoucisse1295 Месяц назад +1

    😢nite kou bakh kou yarou kou Tey yaw fonek yalla dina takhawou❤

  • @momosy6083
    @momosy6083 Месяц назад +3

    Yallah nala yallah same kou moytouwoul réne ak sougouf loraguén rek mo si nek bayi lép si lokho yallah mo wor

  • @user-tn1it6dn7i
    @user-tn1it6dn7i Месяц назад +1

    Aka bakh ta am ngor walahi sunu wayleu yalna snu borome mayla werr

  • @khadygueye-ol2vm
    @khadygueye-ol2vm Месяц назад +2

    Machalah thiate dou fess mais yalla nala yalla defal djamm

  • @mouhameddia5168
    @mouhameddia5168 Месяц назад +46

    Kou moytouwoul rène yi insuffisance rènal rèck .sa cadior yalla nala yalla tèguil natou bi

    • @Justin-Lo.
      @Justin-Lo. Месяц назад +5

      AK soungouffe si niouy nane moussibeu leu dem.hopital dal mogueune

    • @Justin-Lo.
      @Justin-Lo. Месяц назад +2

      Sinon febbarr bi dafa werrre wala dafa tanné rk😢

    • @mouhameddia5168
      @mouhameddia5168 Месяц назад +4

      @@Justin-Lo. fèbar bi dou wère mais dangaye dèff dialyse maname purufier le sang tout les 7 jours ou au pire des cas 2 fois par semaine sinon niou défal'la transplantation reinal manam niou dieul reinwou kénéne diokhlako

    • @mouhameddia5168
      @mouhameddia5168 Месяц назад +4

      @@Justin-Lo. dème hospice moye deugue dèh wayé yalla nanou yalla mouseul si fèbar bi

    • @ibrahimasene9243
      @ibrahimasene9243 Месяц назад +9

      Sa waay dou rééne yi déh.fébar mo gneuw rék

  • @cheikhndiaye4199
    @cheikhndiaye4199 Месяц назад

    Vrément sa diambar ga yalnala yalla geuna wéral té bayilak sa sokhna manchalla ❤

  • @IssaDiop-ik4hn
    @IssaDiop-ik4hn Месяц назад

    Yalla nala yalla may wér inshalah amine

  • @ibrahimafam-fv6ik
    @ibrahimafam-fv6ik Месяц назад +7

    Yalla nala yalla tegiul inchalla rabi

  • @user-gu8nz6uz1o
    @user-gu8nz6uz1o Месяц назад

    Yalla nala yalla may weer

  • @papemoussadiop83
    @papemoussadiop83 Месяц назад +4

    balla ak sa thies ay nite laniou

  • @AbdoulayeThierno
    @AbdoulayeThierno 20 дней назад

    J'ai m'aime coulait des larmes

  • @afro3827
    @afro3827 Месяц назад +7

    Sa cadior borom marché diarem 🎉

  • @Eleveurmouton
    @Eleveurmouton Месяц назад +1

    Ohh wolahiii ndeysane adouna amoul solo 😌🥲

  • @gayesamb8201
    @gayesamb8201 Месяц назад +4

    Kii bilay pour man fatou na bou yëgue ndeyesan yalla nako yalla may werr

    • @AlbD9544
      @AlbD9544 Месяц назад +2

      Yaw moom wéroo vrai domeraam ngua lii nouko nit meuné

    • @mamadieng5574
      @mamadieng5574 Месяц назад

      ​​@@AlbD9544ki kay c'est 1 vrai con nakala nit meuné wakh li .nonn

  • @ModoubaraMbaye
    @ModoubaraMbaye Месяц назад +5

    Thieuye adouna la vie est comme ça

    • @omarpouye1586
      @omarpouye1586 Месяц назад +1

      Bilahi Lou diara bayi hel adouna dafa meti trop motah Lou diara bayi y

  • @panogayembaye2116
    @panogayembaye2116 Месяц назад +1

    Amna solo YALLAH Wérr gui yokkou

  • @user-ek8ct2qn8i
    @user-ek8ct2qn8i Месяц назад

    Yalna yalla geun la defal tawfekh mbeur bou bakh waay

  • @MouhamadouSow-ix7iz
    @MouhamadouSow-ix7iz Месяц назад +1

    Sa cadior yalla nala yalla soutoural

  • @moustaphadiedhiou8320
    @moustaphadiedhiou8320 Месяц назад

    Sa cadior bilahi nite kou bakh 💪💪gouy gui mo warone gueuna sonou si febaram mais kene sentirou kosi

  • @user-te7ib6jo4e
    @user-te7ib6jo4e Месяц назад +1

    Wakh dégue yalla borom bakhla taw fékh rék

  • @tallambaye6580
    @tallambaye6580 Месяц назад +1

    Febar bou métti té yagg mais yalla duékhoul yalla sa boroom mayla wèrr

  • @awaantagueye4562
    @awaantagueye4562 Месяц назад

    Yalnala yalla safara si saydina mokhamet amine yarabi

  • @BantanKante-uu7bb
    @BantanKante-uu7bb Месяц назад

    Massalah sa kadior ah nouvelle bi nekhna aka nopi

  • @blazejohns8004
    @blazejohns8004 Месяц назад

    Y'Allah nala Y'Allah taxawou sa kadior

  • @makhtarsall8367
    @makhtarsall8367 Месяц назад +2

    Yallah nala yallah défal diam si barké seydina mouhaméd

  • @user-wz8qs7fx6w
    @user-wz8qs7fx6w Месяц назад +1

    DIEUREDIEUFÉ YALLA SOUNOU BOROM ALHAMDOULILAH SA CADIOR YALLA NALA YALLA DEFAL DIAM INCHALLAH SI BARKI SEYDINA MOHAMED SALALAHOU ALEYHI WA SALAM ❤️🕋🙏

  • @dawithannajantha5633
    @dawithannajantha5633 Месяц назад

    Ya rafet khôl. ❤. Très bonne chance. L'homme de Viry chatillon.

  • @mamesayegiorgessi3799
    @mamesayegiorgessi3799 Месяц назад

    Massa yalna yalla maye la weer

  • @ibrahimasene9243
    @ibrahimasene9243 Месяц назад +3

    Ohhhhhh ndéyssane Aka meunone beuré yallana là yala méye weur keung

  • @omardiallo114
    @omardiallo114 Месяц назад

    On connaît tjrs les vrais amis pendant ls moma très difficile

  • @user-si8qn5gc2m
    @user-si8qn5gc2m Месяц назад

    ndeyssane adouna lo mougne mou diékh ❤

  • @doudousylla7821
    @doudousylla7821 Месяц назад +2

    Yalna yalla yokk la weur 😢🙏

  • @DiopBirahim-rc7vc
    @DiopBirahim-rc7vc Месяц назад

    Balla gay sa thies 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽

  • @gorasall5899
    @gorasall5899 Месяц назад

    Yalla na Yalla yokkou la weer amin incha Allah

  • @ababacarlo2654
    @ababacarlo2654 Месяц назад

    Un grand champion.

  • @soukeynadiallo1472
    @soukeynadiallo1472 Месяц назад

    Yalla khôlle laye Faye machalla

  • @SidiyaFaty-vh8kq
    @SidiyaFaty-vh8kq Месяц назад +1

    Yalla n'a yalla maye llah wére si barké mouhamed

  • @sythiernosy752
    @sythiernosy752 Месяц назад

    Un homme très courageux

  • @Jah-uj4tb
    @Jah-uj4tb Месяц назад +2

    Bilahi kou bakh moguini on se connai kham nako bbx khol bi dara nékousi

  • @mbenguembor3977
    @mbenguembor3977 Месяц назад

    Yalla nala yalla maye wer 👏🏿👏🏿

  • @user-on3se3qp4j
    @user-on3se3qp4j Месяц назад

    Bon rétablissement champion

  • @user-fm5ir8gn6o
    @user-fm5ir8gn6o Месяц назад

    Courage yallena yalla guoudal sa fane

  • @asrar1296
    @asrar1296 Месяц назад +1

    Alhamdoulilah ❤❤❤

  • @souleymanefall5499
    @souleymanefall5499 Месяц назад

    YALLAH NALA YALLAH WEREUL BOU BAHE BARKE SEYDINA MOUHAMED RASSOULALAHI SAW

  • @whatsup-hl5qm
    @whatsup-hl5qm Месяц назад

    Machalah Kadu yi rafetna

  • @omkenzo_66
    @omkenzo_66 Месяц назад

    Yalla nala yalla may wéer cii barki cheikhal khalifa

  • @domoudaara
    @domoudaara Месяц назад

    Nako BŪŪR YALLA chàafara Yàaaaa Rabbi 🤲🏿

  • @ndtbabs
    @ndtbabs Месяц назад

    Yalna ko yalla takhawo borom khol bou rafet dou torokh moukou

  • @falloufall6687
    @falloufall6687 Месяц назад +1

    Sa yalnala yalla geuna wéral diambar machallah

  • @thiandoummoussa3394
    @thiandoummoussa3394 Месяц назад +4

    Ki thiate moko diape mè mo dakhone beuré Guediawaye ba paré beuri mbolo ame entraînement lou méti la dane tek bopame mbapate guediawaye kéne meunou kosi wone bilahi

  • @mamadoundoye6077
    @mamadoundoye6077 29 дней назад

    Yalla n’a Yalla defal diam

  • @Crisproo7
    @Crisproo7 Месяц назад

    Courage champion 😢

  • @boy_galsen12
    @boy_galsen12 Месяц назад +4

    sou nekon may yaw comme bayi nga beure ba demate touki diemal def mannequinat parceque am nga tay bi ak teint noir te ligueye la meun nala oubile yenen opportunite

  • @dakarcolobabe9221
    @dakarcolobabe9221 Месяц назад +1

    Ndeyssane c etai dur yalna yalla sama

  • @papeassanethiam7923
    @papeassanethiam7923 Месяц назад

    Yalla na yalla yokou wer bi

  • @SoukeyeTandiang
    @SoukeyeTandiang Месяц назад +2

    Machalla thier amne solo

  • @georgesmendy8021
    @georgesmendy8021 Месяц назад

    Yalla nala yalla dooli soutoura may la weer ak goud fan

  • @MouhamadouSow-ix7iz
    @MouhamadouSow-ix7iz Месяц назад +1

    Yalla nala yalla may diame

  • @kambayependasall8908
    @kambayependasall8908 Месяц назад +1

    Ndeysane yalla nala sunu borom May wer

  • @pendalam2578
    @pendalam2578 Месяц назад

    Machallah longue vie à toi

  • @omarpouye1586
    @omarpouye1586 Месяц назад

    Yalna yalla may nieup werr 😢 adouna mongui nii dh.
    Kouko doundoul meunoko ham walahi

  • @user-dp7gy1vq9b
    @user-dp7gy1vq9b Месяц назад

    Machallah yalla n'a yalla doli weurre

  • @aboumane6047
    @aboumane6047 Месяц назад +1

    Yalla nala may werr amine

  • @MaketSii-jm4fu
    @MaketSii-jm4fu Месяц назад

    Yalla na yalla guena wer si barkep cheickhoul khadim adouna lepou diangante la

  • @mariendiagoakbuurtv5226
    @mariendiagoakbuurtv5226 Месяц назад

    Du courage champion❤

  • @kawistodiallo4882
    @kawistodiallo4882 Месяц назад

    Sa cadior yala nako yala may weurguou yaram

  • @user-ij6di6mx8o
    @user-ij6di6mx8o Месяц назад +9

    Mais gouye gui limouye reuye lamigne yeup kone sétouko??😢

  • @omardiallo114
    @omardiallo114 Месяц назад

    Machallah lng vie à vous

  • @fruityvoice997
    @fruityvoice997 Месяц назад

    Yallah nallah yalla tahawou

  • @user-bq9qc6vb9b
    @user-bq9qc6vb9b Месяц назад

    Sa yalla nala defal diam

  • @modoufaty1152
    @modoufaty1152 Месяц назад +4

    Febar bou metti mogui ni billayy état si warra djieukeu dioublou

  • @FallouSeck-jf9cn
    @FallouSeck-jf9cn Месяц назад

    Bilahi grand by Diam si yaw

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 Месяц назад

    Alhamdoulilah bonne arrive