REACTION PETIT LO APRES SA VICTOIRE CONTRE BRISE DE MER

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 фев 2025

Комментарии • 204

  • @rokhayathiam7913
    @rokhayathiam7913 День назад +38

    Soulalone fass mou takha soufe félicitations petit Lo

  • @LamineColy-l7g
    @LamineColy-l7g 23 часа назад +25

    Bilaye kholna Bénéne angle bi 3 appuies la def té fesses bi lalou Souf. Félicitations petit lo

  • @moustaphadiop-md4jx
    @moustaphadiop-md4jx 23 часа назад +24

    Kate lène séne nday kholi lénène Petit Lô seul 💪🏽❤️🔥🩸domou bour bour leu❤❤

    • @CheikhFall-f9o
      @CheikhFall-f9o 23 часа назад +1

      Ya nakhari dered de mais nguir yalla bouma saga mangi lay nianal nga bayi saga tamit sakanoul de

    • @CheikhFall-f9o
      @CheikhFall-f9o 23 часа назад

      Machalah diell bi tarouna lol

  • @mansourgningue4082
    @mansourgningue4082 23 часа назад +19

    😂😂😂😂Niugui xatarayou rek felicitation petit lo

  • @amleking2219
    @amleking2219 23 часа назад +21

    En faite khawma lane la mais modou lô takhna thioféll bima am si wa parcelle khawma lane la koi blh❤ mais yalla bakhna parcelle ndam rk inchallah 🤲❤❤

    • @moustaphadiop-md4jx
      @moustaphadiop-md4jx 22 часа назад

      @@amleking2219 niola geuneu beugu bilay kouniou beugu niou beugu leu❤️💪🏽🔥

  • @FelixBaraye-j8p
    @FelixBaraye-j8p 22 часа назад +7

    Félicitations petit lo et mes encouragements a brise de mer.

  • @maragueye8207
    @maragueye8207 21 час назад +4

    Yaw miye saga si télé bi danga réw amo dolé wallahi do Dara petite lô félicitations ❤❤❤

  • @FatouMbaye-u9s
    @FatouMbaye-u9s 23 часа назад +16

    WA ALÉA THIAROYE DIAMAGUEUNE HEURE BOUNOU DANO DÉM PLATEAU 😂😂😂😂

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 День назад +28

    Bayi leen danou di took plateau😂😂😂😂

  • @bachirvd619
    @bachirvd619 22 часа назад +7

    Paty lo rek❤❤

  • @SerignefallouNiang-l1i
    @SerignefallouNiang-l1i 23 часа назад +6

    Félicitations pour petite lô yallna si ndam you bari topou ms petit déll téy nguirr yalla

  • @abdoudiop8697
    @abdoudiop8697 22 часа назад +4

    Félicitations petit lo ndam rek inchallah demlene gnibi petit mola meune

  • @MorDieng-d1i
    @MorDieng-d1i День назад +15

    Péti lo souy beriti nioun wa diander dina niou niaw s'opère té ko inchallah ❤❤

    • @BourouKaff
      @BourouKaff День назад +4

      Soula nékhone bindd supporté wayé déffoko 😂😂😂

    • @MedouneDieng-u1t
      @MedouneDieng-u1t 23 часа назад

      Ki kay domrm la😂😂​@@BourouKaff

  • @AliouDIOME-o8p
    @AliouDIOME-o8p День назад +21

    Thiaroy ak diamageune benn la souniou dano nioy ndieuk si plateau bi 😂😂

  • @cheikhsene5081
    @cheikhsene5081 День назад +11

    Geume léne yalla dann lén dane 😂😂

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 День назад +11

    Ki ngene di kasal sakh kham nani dagno daan ndym 😂😂😂

  • @KhadimeDiene-q2o
    @KhadimeDiene-q2o День назад +8

    Félicitations pati lo

  • @SidiyaDieng-m1v
    @SidiyaDieng-m1v День назад +15

    Siteu wanéna Yonne bii dé 😂

  • @zo47
    @zo47 День назад +6

    Petit lo mou teul ndéy bamoû danou. Ki amoul sakh diom tôg fi nane var😅

  • @Mamadou-j1x
    @Mamadou-j1x День назад +6

    AMOL 4 APPEI DH😂😂
    Petit lo mo kii wy❤

  • @sssalihou7819
    @sssalihou7819 21 час назад +3

    Wakhléne Brise de mer deugue, khaléleu, na yokeu entraînement yii. P’tit Lô dako dane diéleu bou reuye

  • @cheikhseck4243
    @cheikhseck4243 День назад +6

    😂😂😂😂 de nguène di khaaaar😂😂😂😂😂😂 PT'lo❤

  • @layendiaye4047
    @layendiaye4047 14 часов назад +1

    Siteu yakhana,boyyep koudanu tok plateau di wakh rek😂😂😂😂😊

  • @AlphaSaliou-n9k
    @AlphaSaliou-n9k 23 часа назад +4

    Félicitation Petit lo

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 День назад +4

    Dem leen ndayi nelawi 😂😂kou gneuw petit lo dakhar sa ndaye Reug so beuguei nga gneuw

  • @CheikhMbacke-f8r
    @CheikhMbacke-f8r День назад +9

    Bayi lene doul petit lo moko dane waye lerna waye

  • @mohamedvany6677
    @mohamedvany6677 День назад +11

    Fess bou lal souf té takko souf gueum len yalla😂

    • @salycissokho7382
      @salycissokho7382 16 часов назад +2

      Takhoul souf kay lolou la guiss genou nio tak souf

    • @mohamedvany6677
      @mohamedvany6677 13 часов назад

      @ gni gno wara bayi heure bougnou amé défaite dém plateau di réclamer nagnou gueum yalla

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 День назад +9

    Guisguene petit lo dans 2ans il peut devenir roi des arenes il peut etre beaucoups plus coriace que son pere modou lo roi des erenes

    • @deveba8657
      @deveba8657 21 час назад +1

      No je ne crois pas il n a pas l talent de modou

  • @madiandiaye35
    @madiandiaye35 День назад +41

    Démme léne teudi 😂😂😂😂

  • @MbayebabacarSarr-y8f
    @MbayebabacarSarr-y8f День назад +9

    Reug bala sa thies dané nga wakh boudé vidéo 4 appuie amoul boudé 4 appuie 😂😂

  • @haddytinn2070
    @haddytinn2070 День назад +5

    Félicitations petit lô

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 20 часов назад +1

    Ousmane diop mii dou nitou dara gueumoul touss nak félicitation petit lo

    • @MDbousonko
      @MDbousonko 10 часов назад

      Sa waye Ousmane Diop Amo lokoy wakh deugé Rek la wakh

  • @mouhammadndiaye7358
    @mouhammadndiaye7358 23 часа назад +5

    😂Wa bor bé dagno beug recours ak appel

  • @amadoudiopndoye3582
    @amadoudiopndoye3582 22 часа назад +2

    Saway tu exagères petit Lo foumou tégué fesss 😂

  • @papaabdoulayesene8797
    @papaabdoulayesene8797 День назад +7

    Coly Faye 2 amoul diom 😂

  • @andrendione9021
    @andrendione9021 День назад +11

    Koly Faye woutil combat. Chaque combat gnou gnoussss leu amo diom

  • @PapaBa-gx3bn
    @PapaBa-gx3bn 23 часа назад +2

    félicitations petit lo

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 22 часа назад +1

    kit bind sén titres yi mome foumou diangué😂😂😂 mounane après ''son victoire''😂😂😂

  • @cheikhoulkhadim3271
    @cheikhoulkhadim3271 День назад +6

    Baye balla 😂😂😂😂😂❤

  • @MDbousonko
    @MDbousonko 10 часов назад +1

    Baye Balla boula ken dougall deh😂😂😂😂

  • @FatouNgom-k6y
    @FatouNgom-k6y День назад +8

    Non vraiment nak way thiaroye daguene commencer dof😂😂😂

  • @FallouDiakhate-p4d
    @FallouDiakhate-p4d 22 часа назад +2

    Wa yene dimbali lene niou way petit lo dane kii diel bou leer 😂

  • @mouhage2157
    @mouhage2157 День назад +4

    Wa gni werrr nagne 😂

  • @khalilbeugbamba3028
    @khalilbeugbamba3028 23 часа назад +3

    Future modou lo❤

  • @djibysoung2998
    @djibysoung2998 День назад +5

    😂😂😂 yen boulen nou sonal boul yakh sa 25000 dano 😂 diel bou Rey binou len dan 😂 santal tedem

  • @damembow6374
    @damembow6374 День назад +11

    Félicitations petite ms daga eupeul trop ayy kilifeu bougniouy diougg ndah yaw dagua téyy tékk combat bi sii yonn

    • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
      @AboubacryGASSAMA-zs7oi День назад +2

      Lolou dafa lérr ...message bi cokou diégué warenako lire petit lo prochaine bouy beuré dafa wara téye dieule temps lire combat biii...bénéne affaire aussi bouye songuou mou diégué mbeur mi bagna songue bou soriii ..mom mo gagné vraiment mes défena erreurs you barii à corrigé après combat..

    • @damembow6374
      @damembow6374 21 час назад

      @AboubacryGASSAMA-zs7oi Nn lamb dafa ammm yonn koi vraiment

    • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
      @AboubacryGASSAMA-zs7oi 21 час назад +1

      @damembow6374 dafa ame yone sui d'accord

  • @mamadoundongo5869
    @mamadoundongo5869 День назад +3

    Ñioun parcelle là niou deuk😂😂

  • @allioutall3990
    @allioutall3990 День назад +5

    Coly féy moom dof la😂😂

  • @BlackGanginnove
    @BlackGanginnove 23 часа назад +3

    Après sa victoire 😭😭😭

  • @Bapzotdigneshop
    @Bapzotdigneshop 19 часов назад

    Faralouma modou lo ms peuty lo môme nékh nama 😂😂😂😂

  • @allioutall3990
    @allioutall3990 День назад +15

    Mais petit lo bo tongon guémbou li takhue sofff walla 😂😂geum lén yalla

    • @ModouDiaw-nc7bn
      @ModouDiaw-nc7bn День назад +2

      Modou lo contre ama baldè nila dèfone walla

    • @djibrilniang6053
      @djibrilniang6053 День назад +1

      Assis sur les talons diel leu

    • @demba8102
      @demba8102 День назад +1

      Vraiment

    • @demba8102
      @demba8102 День назад +2

      @@djibrilniang6053sawaye ki danouwoule nganane talon 😂

    • @djibrilniang6053
      @djibrilniang6053 День назад

      @@demba8102 wakhouma dafa danou demey expliquer rek li wa thiaroye khalat

  • @assaneSy-v9q
    @assaneSy-v9q 17 часов назад

    😂😂😂 petilo mo dan lo lén bege

  • @khalilbeugbamba3028
    @khalilbeugbamba3028 23 часа назад +1

    Reug reug mi esk nitt la😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 19 часов назад

    Boulen niou sonal laloul souf😂😂

  • @papadaoudaDieye-iz8dm
    @papadaoudaDieye-iz8dm 22 часа назад +1

    Légui danou Djitou plateau guéne dieul ok😂

  • @Mamadou42-dk5sn
    @Mamadou42-dk5sn 22 часа назад +2

    PETIT LO SEUL 💪🥳

  • @cherifousinguinar8455
    @cherifousinguinar8455 22 часа назад

    Thiaroye dal deuk leu 😅😅 ki di saga melni bayam mo niou mom😅😅😅

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 7 часов назад

    Sa waye 😂😂 yaaw diga rousss yaww gñou dane laa baa war sisa kaw 😂😂 no lambadji dina yakhou CNG BII MO WAR DIOK SI LI DI DAAWW BANOU DANÉL LAA GANANE YAA DANE CNG bii moye woute khaliss si yéne dakh recouryi khalis guéneléndi diokh mo takh petit lô dane laa dane bou lér

  • @sidysiby9795
    @sidysiby9795 День назад +7

    Sou tokon guémbeu li day tak souf

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h День назад +4

    Bayilène soungène dano di wakh damlène si recours yi rek bagne di beuré aye yambar ngene rek gnak diom

  • @iscojo6600
    @iscojo6600 Час назад

    😂 thiaroye ay dof laniou. Bay Balla fallait couper le direct… ils insultent devant BATAMBA TV c’est pas normal.

  • @NdaoMor-k3g
    @NdaoMor-k3g День назад +1

    Wa reug mi were 😂😂😂

  • @abibdiop4678
    @abibdiop4678 20 часов назад

    Baay baala😂😂😂😂w

  • @BaidyAbdoulayeDia
    @BaidyAbdoulayeDia 20 часов назад

    Aka nio beugueu plateau 😂😂

  • @cheikhbi2056
    @cheikhbi2056 20 часов назад

    Boys yii danioo réew. Daanou nguéen té sou nguéen défé recours sakh dou nguéen am dara parceque yarouwouléen

  • @ndiogousarr2447
    @ndiogousarr2447 21 час назад

    No dff niou tokk plateau 😂😂😂

  • @MDbousonko
    @MDbousonko 10 часов назад

    Ousmane Diop merci wakh nga waxou nitte deh

  • @TKFTV111
    @TKFTV111 23 часа назад +1

    Geum len yalla ki da xepp peti Lo

  • @magattediop4442
    @magattediop4442 9 часов назад

    Brise sakh kham nani danoul 😂

  • @souleymanediallo4608
    @souleymanediallo4608 19 часов назад

    Nek ci plateau en direct mouy saga ndeye !! Indiscipline

  • @BabacarMbaye-q5q
    @BabacarMbaye-q5q День назад +4

    Biriz sakh khamena ni danouna dakh guissoul lou lér

  • @abdoulayediop9331
    @abdoulayediop9331 День назад +2

    Waw mané ana khadim ana issa ana Ousmane Diop ak reug reug nioum nieup la poti lo boulé dane

  • @Young_boy43
    @Young_boy43 День назад +3

    Mane var la meunoul comprendre bane ndiarign la ammm vrmm

  • @MorTallaKa-vv9tc
    @MorTallaKa-vv9tc 21 час назад

    Reug reug mome weroul 😁😜

  • @MouhamedlamineSissokho
    @MouhamedlamineSissokho 23 часа назад

    Baye balla kéne douka dougueul 😂😂😊

  • @sambadiene5749
    @sambadiene5749 20 часов назад

    Franchement petit Lo mo mo Ndane

  • @ShartjadDart
    @ShartjadDart 20 часов назад

    Gni ay dof lann 😢😅😅

  • @Fitserigne
    @Fitserigne День назад +2

    Campions du monde moy wakh ni geuneul yallah parcelle seul 😂😂😂🦾

  • @AliouDIOME-o8p
    @AliouDIOME-o8p День назад +1

    😂😂😂 kholal fo dieum 😂

  • @taphagueye-l9j
    @taphagueye-l9j День назад +1

    Geum lene yalla nak fi diel amoufi

  • @mansourdiop2022
    @mansourdiop2022 День назад +5

    Tok sa tâtt lalouy souff
    Reug Reug mo nékh rék

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j 20 часов назад

    Petit Lo nguèmb bi takoul souff sakh donc naniou donn ayy sportif Man faralouma ko mais togoule deugue la yallah beugue.

  • @serignediongue7807
    @serignediongue7807 День назад +1

    Var la khamoul bane ndarigne la ame

  • @ibrahimaguisse5802
    @ibrahimaguisse5802 22 часа назад

    Danou tokk plateau mome nioci meune😂

  • @OmarKane-y4z
    @OmarKane-y4z 21 час назад

    Mougne léne 😂😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 23 часа назад

    Félicitation

  • @serignendamelo6964
    @serignendamelo6964 23 часа назад

    Fii mom darra amou fii

  • @MomoDiop-w5k
    @MomoDiop-w5k 23 часа назад

    Teudi léne mo gueuneu 😂😂

  • @CheikhFall-bn4ki
    @CheikhFall-bn4ki 22 часа назад

    Wadji di saga mo niakkk talibé deug Yaw dhe do done champion

  • @Abdou-g6r
    @Abdou-g6r День назад

    Peti lo da danou❤

  • @thiawzall1547
    @thiawzall1547 День назад +1

    Ki mo nekh 😂😂😂

  • @gueyemamecheikh6440
    @gueyemamecheikh6440 День назад +1

    Bay balla 😂😂😂

  • @ThFa-o9f
    @ThFa-o9f 23 часа назад

    B de mère diambar nga,😂😢

  • @boubacarfall2225
    @boubacarfall2225 16 часов назад

    No rèw amena gueme léne yalla gnou dane léne guéni Wakh sof guéne trop

  • @elhadjiabdoulayembenguecis3590
    @elhadjiabdoulayembenguecis3590 22 часа назад

    Da nga Danou Petit lo Bou toguone Takha Souff Kholall Ngèm li noway brise le silence Na Rafète

  • @babsbaba19
    @babsbaba19 День назад +1

    Sa victoire

  • @thiawzall1547
    @thiawzall1547 День назад +2

    Dano Ken

  • @TaphaLaye-gl8vd
    @TaphaLaye-gl8vd День назад +1

    Bi dou ama nékh déh bi bakhoul déh

  • @ibrahimandiaye6337
    @ibrahimandiaye6337 11 часов назад

    Lamb ji legui mo beuri ay mbeur you goor jigueen legui
    Paa yi gno gueune seuytanè teksi nek ay doungourou, fi béneu ndam mofi am ta petit lo mo dane

  • @SambaThiam-bv9rj
    @SambaThiam-bv9rj 22 часа назад

    Coly Faye kay dieul petit lo nokola nga kham