Le muezzin de la mosquée de Ndièye tué, un témoin raconte l'origine du différent

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 2 дек 2024

Комментарии • 186

  • @boussondiaye6359
    @boussondiaye6359 2 года назад +100

    Raynagn un homme véridique kou bakh am dîné AK l'islam 😭 yalla bouko thiatt djittou ci bamel LaM ci barkep cheikhoul khadim 🙏

    • @mamadoudieye2006
      @mamadoudieye2006 2 года назад +3

      Amin Ya Rabbi

    • @haysamatanar2475
      @haysamatanar2475 2 года назад +2

      amine

    • @yacinethiam7578
      @yacinethiam7578 2 года назад

      Amine

    • @meyoundao4103
      @meyoundao4103 2 года назад

      Bilahi mon oncle à fait le même timoignage il travailler avec lui wayè kou bakh talibe gnak thiakhane ndeysane nako yalla yereum

    • @BarrFama
      @BarrFama 5 месяцев назад

      Qqm😊😅​@@mamadoudieye2006

  • @jacky3326
    @jacky3326 2 года назад +63

    Ndeye sane Baye boye mi kou deugoula dieureudieuf Baye 🙏🙏

  • @antasarrcisse1803
    @antasarrcisse1803 2 года назад +111

    Que Dieu nous protege tous des djinns, seytane, mauvais oeil, mauvaise langue, tout mal et actions negatives

  • @deugrek344
    @deugrek344 2 года назад +62

    Toutes les personnes impliquées sur cette affaire doivent mourir en prison. Ils sont jaloux et méchants. Beaucoup de villages c'est ce même phénomène le clanisme, la méchanceté etc les problèmes de castes. Paix à son âme. Que Dieu l'accueille dans son paradis.

  • @alimatoudieng7684
    @alimatoudieng7684 2 года назад +50

    Yén ki tabakhoul bar tabakhoul boite khana diakka négou yalla guéne doufi am yén dé dougén ay dioulit khana li metina trop 😭😭😭😭😭

    • @serignemouhamadoumadiamasy5574
      @serignemouhamadoumadiamasy5574 2 года назад +6

      Deugue yi dafa bari ay thiédou geumou nio dara walahi wayé yalla di lén mbogeul

    • @malioudiallo9321
      @malioudiallo9321 2 года назад

      Ce n'est pas un problème de mosquée ou de bar ou même de dépositaire d'ordures, c'est un problème de loi , qu'on les arrête et qu'ils soient punis au nom de la loi.

  • @seydinasene1131
    @seydinasene1131 2 года назад +44

    Que justice soit faite li dafa niaw trop bilay 100ans de prison

  • @veriteeternelleverite3530
    @veriteeternelleverite3530 2 года назад +53

    Quelle honte pour ce village, et c'est comme ça que ça se passe dans bcp de village et quartier au Sénégal, ils font un islame de clan et de folklore
    Ce vieux est un martyre, Paix à son âme

    • @modyndoye3893
      @modyndoye3893 2 года назад +1

      Trop dégoutant vraiment pour des doit disants croyants! Triste ce pays

  • @mohamedassanecoly5533
    @mohamedassanecoly5533 2 года назад +5

    Ce que je ne comprends pas est, où était le reste du village lorsque l’Imam et ses acolytes le provoqué jusqu’à le tuer. Car que je sache le muezzin est un homme digne, honnête et serviable.
    Paix à son âme

  • @84monsun
    @84monsun 2 года назад +15

    Togne naniouko 😢😢 Yalla nako sunu borom kharé Aldiana

  • @martingomis908
    @martingomis908 2 года назад +6

    Ce que ce vieux a dit est clair et net ! Que justice soit faite ! Tous ceux qui ont participé à cette tuerie, en prison.

  • @BABEUGUEBAYE75
    @BABEUGUEBAYE75 2 года назад +12

    Njiko rey yalna lene yalla alak 😢

  • @bassiroukane8266
    @bassiroukane8266 2 года назад +64

    Un martyr. Paix à son âme

  • @falloundiaye3120
    @falloundiaye3120 2 года назад +12

    Ndeysane gor gui niit kou deugou la Yalla nalla yalla may wer ak goudou fane

  • @daronguer5201
    @daronguer5201 2 года назад +22

    Que la justice fasse son travail

  • @madiamaseck1957
    @madiamaseck1957 2 года назад +8

    Un vrai martyr pour l'Islam

  • @nddiayemidou8216
    @nddiayemidou8216 2 года назад +9

    Yalah naniou yala def aye dioulit hakan, ndakh li dou dieufi dioulit , raye cou beuga tabakh negou yalah ,li niaw n’a lol 😢yalah nako yalah yeureum te khareko aldiana

  • @lotagaye3437
    @lotagaye3437 2 года назад +20

    Pape yaye goor mais wa deck bi niepou laniou wara teuj si kasso bi

  • @tmasterp8279
    @tmasterp8279 2 года назад +4

    Les gendarmes devaient venir dans le village sur les lieux en-avant mais au Sénégal ils se déplacent seulement quand ya des morts !!
    Nous réclamons plus de sécurité au Sénégal

  • @sambmamadoufalilou4830
    @sambmamadoufalilou4830 2 года назад +6

    J'ai écouté le vieux ce qu'il a dit c'est claire les gens qui ont fait l'acte doivent périr en prison tros c'est tros c'est la méchanceté grave de tros.

  • @awandiaye9184
    @awandiaye9184 2 года назад +1

    Gorgui yalna YALLA goudeul say fane. Deugou rek mo am solo té kou déglou kadou yi khamni lou deugouleu

  • @talagaye6808
    @talagaye6808 2 года назад +5

    Ndayesan li metina loul ms Santa yalla rek baye aliou conte yalnala yalla faye amine

  • @pendaba2521
    @pendaba2521 2 года назад +4

    Lii dé mane makay doga deugueu kouy tabakh mosqué kay boko meunoul diapalé nga nianalko yallah mê yalna lenn yallah alakh amine lolou rkk laa len yéné thim sama khol diekhna

  • @boubacartall7184
    @boubacartall7184 2 года назад +9

    Non non khametouma Sénégal, waay waay nitgni nagnou andak sago

  • @MsMylifes
    @MsMylifes 2 года назад +1

    Une personne courageuse et visonnière
    Yalnako yalla yareum

  • @amarcheikh5016
    @amarcheikh5016 2 года назад +11

    Imam bi ak chef des villages bi nan len teudje à vie ay doumou ram deug lan

  • @orricobeppe2311
    @orricobeppe2311 2 года назад +2

    Nagnou oubi cagnotte pour yéguali école bi akk diakeu bi

  • @lathifandiaye9628
    @lathifandiaye9628 2 года назад +2

    Soxor rek molen diap bilae
    Raye nit ndax souf
    Badolo kép molen diap
    K justice soit faite

  • @makhtarsylla521
    @makhtarsylla521 2 года назад +4

    Que justice soit faite

  • @boubacardjigo7271
    @boubacardjigo7271 2 года назад +2

    Paix à son âme justice à fait son travail commandent préfé procureur ils sont tous fait leur travail.niouko Ray nion déff Lou léne nékh

  • @juniorking1134
    @juniorking1134 2 года назад +2

    allahou akbar yalna hipé aldiana ci barké wer wi

  • @dameseck6232
    @dameseck6232 2 года назад +3

    اللهم أغفر له وارحمه واسكنه فى الجنة أمين يارب العالمين

  • @papiinternationale6479
    @papiinternationale6479 2 года назад +10

    Mais pourquoi sénégalaise yi violent comme ça na yone def ligueyam paix à son nom 😢😊

  • @boubab412
    @boubab412 2 года назад +3

    Yalnayalla yeureumko c'est triste

  • @mariemediene3519
    @mariemediene3519 2 года назад

    Bilay papeu wakh dji rafétna wakh gua lép machalla yalna yalla guoudeul sa fann

  • @papasabaly4250
    @papasabaly4250 2 года назад +8

    Bismillahi rahmanirahim
    Ça fait mal au cœur de voir des dignitaires mal intentionné,des égoïste,des jaloux envieux au point de tuer un être humain qui à pour seul crime de posséder un bien auquel vous aspirer,quelle honte des vieux qui courent tjrs sur les biens éphémère

  • @cheikhakbargaye5587
    @cheikhakbargaye5587 2 года назад +6

    Wallaahi Lou wér sakh yalna Yàlla sàmm góor

  • @knn4166
    @knn4166 2 года назад +5

    Malgré que toutes les autorités compétentes ont été informées au préalable le drame n'a pas pu être évité !
    Que Dieu l'accueil au Paradis.
    Ameen

  • @bassinegaye787
    @bassinegaye787 2 года назад +15

    Diadieufe konté dioulite deugue bou nafékhoule dou bagne néguou yalla

  • @ibradiop1161
    @ibradiop1161 2 года назад +9

    Dieuredieuff baye wakh dji rafétna trop wàa deuk bi niou bone lagn

  • @Allahqv1wz
    @Allahqv1wz 2 года назад +1

    Bravo au procureur et au sous préfet franchement ils ont fait leur travail

  • @zulesmbodj3446
    @zulesmbodj3446 2 года назад +6

    Yalna yalla doli ko ndieugal

  • @matarndiaye3838
    @matarndiaye3838 2 года назад +3

    Bilay yalla yeureum ko

  • @ousmanengom8580
    @ousmanengom8580 2 года назад +2

    Yalna la yalla guene la takhawou mayla wërr ag goudou fane mamboy vraiment nit ku deugougua.

  • @farmafaye5914
    @farmafaye5914 2 года назад +1

    Paix à son âme

  • @lahatleye6313
    @lahatleye6313 2 года назад +4

    Hee yaxal ngénn sénn boppu yaxal sény domm yaxal ngénn sénny seutt

  • @papendour7246
    @papendour7246 2 года назад

    Bass yalnago yala khare aldiana firdawsi.

  • @layedeville
    @layedeville 2 года назад +1

    Dama beuga participé si ligayou djouma bi. Noumay déf ?

  • @coumbathiam7682
    @coumbathiam7682 2 года назад +3

    Nn c grave li monme c trop ame na ay nitt you ame xol time nitt ba ray ko démo si lén sen xel si yallah

  • @bassiroundiaye7908
    @bassiroundiaye7908 2 года назад +3

    Sama khoull taguena

    • @aminatanabienne6813
      @aminatanabienne6813 2 года назад +1

      Ma la geunn tangg kholl fimneh nii😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @ndeyefatoukhalysy8758
    @ndeyefatoukhalysy8758 2 года назад +1

    Qu’il repose en paix

  • @seynaboufalldiakhate8029
    @seynaboufalldiakhate8029 2 года назад

    Amna nakhar trop yalna yallah atté li gnaw na trop

  • @mamitafaye7063
    @mamitafaye7063 2 года назад

    Papa dji y’aw Yala nala bourbi doli werr bayilafa bassi kanama kanam wahdji lerna deugoûna Gni def li nak Yala nalenn bourbi torokhal si kaw souff Baye Basse Yala nako yonet bi Terou PSL😢😭😭li metina trop

  • @biramatall8973
    @biramatall8973 2 года назад

    Je veux condamner à vu mai senegal justice badola mo fi ame

  • @makhdydiabou9248
    @makhdydiabou9248 2 года назад +4

    Yalla nako yalla yeureum té kharéko adiana fridawsii barké naby Moustapha psl 🙏

  • @ballakouta6550
    @ballakouta6550 2 года назад +2

    billahi Sénégal nak lii warna niou ci wax dafa yombou trop waye yalla nako yalla yeureum te xaaré ko aljana

  • @moustaphagueye5245
    @moustaphagueye5245 2 года назад +8

    yalla Nako Yalla Yērëm té Jéggal ko té Xaaré ko Al Jana té Féyko yiw

  • @enterprisedaroukhoudossuni6218
    @enterprisedaroukhoudossuni6218 2 года назад +1

    Métina lool ❤️n'a Yon déf liguéyam

  • @cheikhbi2056
    @cheikhbi2056 2 года назад

    NDEYSSAANE lii métina trope trope Bilahi. Louko fi diarr

  • @moulayelaroussi1174
    @moulayelaroussi1174 2 года назад +10

    Nigni nio niak kham diné, ngni warnelen tek lou meti meti meti, domeram yi ,zka nio sokhor domou khadj yi , yalla naka yalla yeureum khareko aldiana ki martyre le inchalla.

  • @mariemegadio774
    @mariemegadio774 2 года назад +1

    Leer na ñaññ

  • @strategiesetdeveloppement2525
    @strategiesetdeveloppement2525 2 года назад +1

    Un pays sans lois

  • @nogayefall4298
    @nogayefall4298 2 года назад

    Paa bii il é tré honnête

  • @nogayefall4298
    @nogayefall4298 2 года назад

    Mbirmi lerna lii métinama trop ndakh di beugua diamou yalla bagnou raylaa

  • @niggaroboundiamedarou
    @niggaroboundiamedarou 2 года назад

    Yàllna KO yàlla GËRËM ci barke Mame Ndiamé Darou

  • @moussafall4372
    @moussafall4372 2 года назад +3

    Mai gni raye pabi éska aye diolit lan

  • @elisabethsambou1130
    @elisabethsambou1130 2 года назад

    Les jalousie es pires

  • @pendandiaye298
    @pendandiaye298 2 года назад

    Yalla nako yalla yeureum diègualniou kharéko adiana firdawsi souf oyof si kawam barkè Seydina Mouhamed Psl metina

  • @salioungom1624
    @salioungom1624 2 года назад +1

    yalna ko yalla yereum
    mais on a besoin de l autre version

  • @mayakeita8092
    @mayakeita8092 2 года назад

    😭😭😭😭C dur

  • @shiekhndaw6997
    @shiekhndaw6997 2 года назад +7

    ومن أظلم ممن منع مساجد الله أن يذكر فيها اسمه
    تقبله شهيدا

  • @khadimdieng1852
    @khadimdieng1852 2 года назад +1

    Gniko Ray dé diaroul woon diapu diaroul fayantoo nanioulén bâyi si deukk bi chaque jour niouy guiss ay ndiabootam gathia gogou rékk doyna seukk ay douma wallahi lolou moo raw ray nitt

  • @peaceandsalam2852
    @peaceandsalam2852 2 года назад

    Yàlla nako buur yàlla yërëm té xaare ko ci Aldiana you gëna kawee ya ñu mu fa fekk ak ñu ko fa fék 🤲🏾🤲🏾🤲🏾

  • @Ibrahim_dia
    @Ibrahim_dia 2 года назад

    Dans ce dossier la justices a bien fait son travail avant l’assassinats du Monsieur BASSIROU

  • @ousmanbalde6870
    @ousmanbalde6870 2 года назад

    Tiey Yallah moudioug diamono

  • @djilysamb6839
    @djilysamb6839 2 года назад +2

    Billahi dane ko togne yalla nako yalla xare aldiana

  • @mansoudiop4515
    @mansoudiop4515 2 года назад +2

    Bilahi ay way alkou amna

  • @laminembaye7616
    @laminembaye7616 2 года назад

    Yallah nama yallah mouseul thi yui genrou imame dima djité

  • @ndoumbefall2673
    @ndoumbefall2673 2 года назад +2

    Koulene gueuneu bone de yalla sakou yalla na nou yalla mouseul thie ignane metina trop ray nite tego ko fene

  • @massaercisse8654
    @massaercisse8654 2 года назад

    Togne nite ki ba paré raye ko. Thieuy adouna . Nite daye kheuye rek bagne la té défoko dara walahi

  • @taphandiaye3991
    @taphandiaye3991 2 года назад +2

    yalla nako yalla yereum dougueul ko aldiana firdawsi

  • @dousediop1759
    @dousediop1759 2 года назад

    Justice doit etre fait vraiment c de linjustice

  • @fatimandao8359
    @fatimandao8359 2 года назад

    Je ne comprends plus li xéw si réwmi

  • @pendaka5180
    @pendaka5180 2 года назад +1

    Ndaysane li métina

  • @fleur_112
    @fleur_112 2 года назад +1

    Liii lëpp liko waral ay deuk bii gnii gnoko momm wala gneulé nakh en général gninouy wakh gno mom deuk bi pour gnom kënn dou amm gnomm rëkk gno wara ame.. Sofa néké commencé amm allall gnou commencé jaloux

  • @aissatoudiop9441
    @aissatoudiop9441 2 года назад

    Yalla nako yalla yeureum oyofal Souf si kawam

  • @ndiayefatou565
    @ndiayefatou565 2 года назад

    😭😭😭😭😭😭 lane mognou dale?

  • @orricobeppe2311
    @orricobeppe2311 2 года назад

    Appel aux bonnes volontés

  • @teckjunior8005
    @teckjunior8005 2 года назад +1

    Ñémé wat ci xasaid ñounilen watlen ci alquran ñou bañ ñi ño bari caxane...

  • @dabakhniang5592
    @dabakhniang5592 2 года назад +3

    Thiéy yalla moudiouk diamono lounék gay guisse

  • @mamadoundiaye5956
    @mamadoundiaye5956 2 года назад

    Bilahi yaina taigalll sa ndeye

  • @serignediattara8577
    @serignediattara8577 2 года назад

    Quel procureur c'est bien

  • @galgalgal8007
    @galgalgal8007 2 года назад +1

    Lii ñaaw na torop 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @paapnjaay1586
    @paapnjaay1586 2 года назад

    Góor gii Ku dëggu la. Li mu wax dafa leer nàññ-nàññ, Maasaa ALLAA!
    Bu dee ki ñu ray tabax jàkka ndóng la bëggoon ci bërëb bu ñu ko may, Imaam bi ak mbooloo mi mu àndal mépp ci lu bon lii ñoom xamu ma ñan waaye bu ñu jàppee séen bópp jullit it am jagewu ñu ko moom.

  • @aliuokonteye1640
    @aliuokonteye1640 2 года назад

    Diaradiaf baye sadome saturaduo aliuo konteye saluom moLaye nayuoe

  • @sencomedie9074
    @sencomedie9074 2 года назад +2

    Sénégal dal diakhal nama legi gni Ray pa bi mba diap nagn lenn 20 ans travaux forcés mo diadou si gniom

  • @khaysoulwarrambacke2720
    @khaysoulwarrambacke2720 2 года назад +1

    Li méty na trop😢

  • @djilabelle2144
    @djilabelle2144 2 года назад

    Ndaysane lidé wakh djou lerla

  • @haysamatanar2475
    @haysamatanar2475 2 года назад +1

    khawma wadji deh wayee dieuwam yeepa rafet lou bakh rek lagnko wakhal

  • @bassiroumbaye7936
    @bassiroumbaye7936 2 года назад

    Ndaysane 😭😭😭😭

  • @elhadj5515
    @elhadj5515 2 года назад

    Metina nama trop yalla kham nako yéna bone yena torox