Koulou kouy teuyé micro si adouna di diangu khassida cheikh MBAYE mola dakha diangu mako wakh . billahi yaa mana diangu machallah yalla ngua goude fane té ande ak wér bari khéweul
Machallah sama sopé chiekh mbaye je suis layène talibé limamou Mahdi psl wallahi soumalay deglou je pleure mme ndah banèkh ak mbécté biguay déf sama xol magui niane sama borombi sw mou defalla Diam ak soutoura barké ak wèr salli allah mouhamadin psl
Ndeyessane baye Moustapha Diop vient de deceder ce dimanche 8 aout 2021. S'il vous plait,priez pour lui.Serigne Moustapha Diop merite tous les hommages,nos respects et considerations.
MACH'ALLAH CHEIKH MBAYE Yallah na YALLAH wéreul baat bi si barké YONÉNTE bi SALLALÂHOU ALEYHI WA SALAM. Je suis NIASSENE mais j'écoute ce zikr tt le temps
Il ne fut et il n’y aura plus jamais quelqu’un comme Cheikhoul Khadim. Cet homme, qui qu’il soit ou quoi qu’il soit, est le plus grand qui n’est jamais existé. Dieuredieuf Serigne Touba sante nala boubax❤
Thieye Serigne Touba mo defar magg gni defar ndaw yi ❣️❣️❣️❣️ baye Moustapha Diop mii mo ndiagg aire bi tay Cheikh Mbaye diko ndiagat si kanamam li dafa sédd kholl bilahii yalla jam yagg
Thieyeum yi kouko deg rek khamni khôl kéep lako waxé. Yalla ngafi yag lol Diop thi barcké Khassida yi. Khôl yeip sednañu thi chex Mbay Yalla na bat bi wer Mourid ❤️
Yallah na sène adjo, mbébétt, liguène di fadiou Ci Barkep Khassida yi té léép donoukoup tawfekh ci Barkep Ya Rassouloul'Allahi Salaatou Ãlayhi Wassalam
jss layénne mais serigne touba lépp ayy banékh si musulmans yeup yalla nako sunu borom fay amine mouhamed ndiaye
Je suis talibe cheikh khasidayi daff may doundall fim may yobu makoo khamm ❤❤
Koulou kouy teuyé micro si adouna di diangu khassida cheikh MBAYE mola dakha diangu mako wakh . billahi yaa mana diangu machallah yalla ngua goude fane té ande ak wér bari khéweul
Ndame fall rek moko dak diangue
@@mohamedly4349 haaaaaa bagnena lolou ndam malik bâ moco mane té malik cheikh moko mane mdrrr
@@azizabdou8385 Senegal bamou dath Abdoulaye diop mofi dakh diangue lolou kene weranté wouko
@@mohamedly4349 yéway samba wahma rk fanelay diar cheikh Sambe ak lamine Seye missi roukh bi
@@azizabdou8385i8oil
Toute personne qui écoute ces khassaid et ne versé pas de larmes doit se revoir
Vraiment vous avez totalement raison, et comment vous l'avez senti?Que Allah vous protege, Amine .
Disciple de Serigne cheikh ahmed tidiane Sy Al maktoom qui a pleuré en entendant cette belle voix. exceptionnel. Machalla
Machallah begue lou bakh rek
Machalla
Lou néx cii xol rk la xathieee❤❤
4
@@djibrilgueye4833😊 by
😭😭😭cheikh mbaye yalla sa brom may la gouddou fane weral bate bi yak sunu bay Moustapha Diop bopou tog barkei brom touba ❤️❤️❤️😍🙏
Po
6. H
Machalla je suis très contente d'avoir les deux en même temps le son et l'écriture dieureudieuf cheikhoul khadim😭😭
Cëy Baye Moustapha soumakay khool sama kholl day tooy ❤❤😢
Meun nama si dioy sakh barké seigne Touba😪
😭😭cheikh mbaye yag fi lool waay baye Moustapha diop yag fi loooö Ndayesan❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😭😭😭😭😭😭
Aaaaminnn
@
@@Khassidayi_rek Le
😭😭😭😭😭😭
😊😊😊🎉🎉🎉🎉😢
Ndeysan yallna yalla weural baat bii tei samela arre la mouseul la thi leep louy lorei
Baye moustapha diop yalla nako yalla yeureum si barkep cheikhoul khadim
Amine
Machallah sama sopé chiekh mbaye je suis layène talibé limamou Mahdi psl wallahi soumalay deglou je pleure mme ndah banèkh ak mbécté biguay déf sama xol magui niane sama borombi sw mou defalla Diam ak soutoura barké ak wèr salli allah mouhamadin psl
Amine
Dieuredieufé Serigne Touba lii sama donne des frissons 🙏🏿
Ndeyessane baye Moustapha Diop vient de deceder ce dimanche 8 aout 2021. S'il vous plait,priez pour lui.Serigne Moustapha Diop merite tous les hommages,nos respects et considerations.
dieuredieuf serigne touba. baye.moustapha.yalla.nako.khare.aldiana
Yallanako yallah yzureume kharéko aldiana firdawsi
𝐐𝐮𝐞 𝐥𝐚 𝐭𝐞𝐫𝐫𝐞 𝐥𝐮𝐢 𝐬𝐨𝐢𝐭 𝐥𝐞̂𝐠𝐞𝐫𝐞
@@babacarfaye4567 amine
Yalla nko yalla yeureum🙏
MACH'ALLAH CHEIKH MBAYE Yallah na YALLAH wéreul baat bi si barké YONÉNTE bi SALLALÂHOU ALEYHI WA SALAM. Je suis NIASSENE mais j'écoute ce zikr tt le temps
Ya que moi qui a cette effet quand J'entends Sindini ou on es plusieurs. Machallah ça me donne des frissons dieureudieuf Serigne Touba
bay ma diapalélassi
@@zeynaboundiayebadiane7729 machallah c'est top
🥰😭
Mashallah. J écoute ç a au réveil et coucher chaque jour
Masha Allah doumassi doyal mouk. Yallana voix bi wér si barké Seydina Mouhamed
UN TIDIANE QUI APPRECIE BIEN CHEIKH MBAYE KHASSIDA ...
Xassida serigne touba yii amoul tidiane ake mouride mone déf té yalla rek takh
Q0op
@@mamysy2470 j'ai bien dit Cheikh Mbaye Khassida okay
Walay ndeysan yaa baxx rekkkk ❤
MachaAllah MachaAllah
Belle voix pour un beau et très émouvant khassida de Mame Cheikh Ahmadou Bamba
Qu'Allah vous bénisse inchaAllah
Ndayesane. Lii manumako setane te tourouma ay xeweul bilahi baye moustapha diop Yalla na sunu borom yeureum te khareko Aldjana 😍
Il ne fut et il n’y aura plus jamais quelqu’un comme Cheikhoul Khadim. Cet homme, qui qu’il soit ou quoi qu’il soit, est le plus grand qui n’est jamais existé.
Dieuredieuf Serigne Touba sante nala boubax❤
Thieye Serigne Touba mo defar magg gni defar ndaw yi ❣️❣️❣️❣️ baye Moustapha Diop mii mo ndiagg aire bi tay Cheikh Mbaye diko ndiagat si kanamam li dafa sédd kholl bilahii yalla jam yagg
Lu weer yalna yallah yokk ay leram
ABDOU KARIM GUEYE
Sante Serigne Touba rek
Thieye cheikh Mbaye yalla sa diame yagge si. Barki Serigne Touba
Macha'alla je suis talibè cheikh mais sindidi reck laa deglou 😭❤️❤️
Ndéysane li nehna si khol yalla hafi yagheu t wéér barké cheikhna saad bou abi
Wakhértou Cheikhna. Ndeysane Amiine 🥳
اللهم إن القبور واسعة والنور والنفور اللهم اغفر ورحمه واعف عنه وادخله جنةالفردوس
Kouye mouride lokho ça kawe fall😭😭
Walakhi
Ndaysan
Billahi la voix en haut
Jl9l0.l0.l.'@@antadiop7633
T
Serigne mountakha mbacké yalla nafi yague lollll té weer si barkep xassida
Amine
Amine
Amine 🥰
Amine
Nekh na
thieyé serigne touba amole moroume ❤❤❤❤
Machallah mouride goudou fan ak weer lek ak xeweul goubari
sr
sérigne same
Amine
Ndaye san yalnafi YAGA loooolll TEWER si BARGUEB S.TOUBA AKH KHASSIDA YI
Aaaaminnn wayy
Thieuy serigne touba yallah gnouko endil si khétou seydina Mohamed bakhé gnouko yallah na gnou KO yallah fayal
Machallah yalla nala serigne touba fay 🥰🥰🥰🥰
Ndeysane sane khassida bi soumakoy déguelou sama khol day toy bilahi kontane na nak 🙏thiey khassida mo nékh deh
Yallah na soufe sede si môme barke khassidayi
Thieyeum yi kouko deg rek khamni khôl kéep lako waxé. Yalla ngafi yag lol Diop thi barcké Khassida yi. Khôl yeip sednañu thi chex Mbay Yalla na bat bi wer Mourid ❤️
Diereu dieufff Serigne touba 🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️
Y en tissu kEUR e Juliette h et surtt jsekd je ieexkku un il se k man ju klhu DH hhjjj d
Mashalla. Alhamdulillah. Dieureudieuf Khadim Rassulilaah.
💔💔💔💔
Ndeye san yalna s Touba fayy li dafa nekh si kohl ligay dff Ame koula si royy moy lou yalla nagou
Dierediefé borome touba❤❤❤❤❤❤❤❣ thiey sindidi ❤❤❤❤❤ yalla na yalla weral bate bi yokou khamham bi yague lol tei weer ci barké kou teidd ki ❤❤❤
Ndey sann thieuy serigne touba cheikh mbaye yalna battbi weur ❤❤
Machalla Liguéyeul sounou borom rék moy deug dieureudieufé Mame Bamba
machalla doundal rawal mouthial khassida limou may def 🙏dieuredieufé serigne touba
Mascha allah yallh nala yallh faye yiw si barké cheikh ahmadou bamba khadim rasoul samoula goudeul sa fan waw goor dieureu dieuf
Dieureudieuf s touba yalla naniou yalla may khéle bougnou mana dégué khassida gui di sindidi té nagou niane yépp amine.
Que le paradis firdawssi soit sa demeure éternelle thi barké borom touba, ak khassida sindidi bi.amine
Yalna yalla wéreul Bate bi machalah contane trop ay dioy mom lay yégue sama yaram
Diadieff s Touba mbacke werouway diadieff mbacke ♥️ kene dou yaw thé rew mi 🇸🇳🙏❤️
Cheikh mbaye yalla nala yalla fay
Ohhh Machalah ❤❤Yalla na yalla weral bat si biir hol lay dougu
Ndeyesan ça c trop sensible. Discipline de cheikh Ibrahima niass ki adore les khassids.
Thank u cheikh ahmadou bamba ra.
Amine way yallna ńiepp am diam 🙏🏻
Dieuredieuf serigne.touba ❤️♥️❤️❤️♥️♥️❤️
❤❤ 3:07
"RIP" Serigne Baye Moustapha DIOP DIOP qu'Allah vous accorde djianatoul firdaws
Amine yarabi
loy tekk ni, il est mort depuis quand?
Amine ya Rabiii ❤❤❤❤yalnaa Yalla yeureum samay wadiour akk beppp djoulite bu gueunde adouna si barkey Rassoul psl ❤❤❤❤
Macha'Allah! Que Le Bon Dieu vous bénisse.Amen!
Ndeysane magui dioy sakh Serigne Touba mana binde kenneu dou mom. Serigne Moustapha Diop yalnako yalla yeureum khareko aldjana firdawsi bidiahi seydil woudioud Amine .
Cheikh Mbaye yalla na yalla wérél batte si barké khasida yi
Thieyy khassidal bi limi def sama khol mane ak yala rk gako xam 😭😭🙏dieureudieufaty S touba 😭❤🙏🙏📿
Ndeysaan Doumaci Doyal.Mame cheikh Mbaye Zikroulah Yalla na Yalla Goudeul sa fann te may la werr ci barke Khadimou Rassoul
Machalla YALLA na Yalla gudal seni fane 💯💯🥰🥰🥰🥰💐💐💐💐 Diaradieuf Mame BOROME TOUBA KADIMOU RASOULLULAHI 💎💎💎💎💖💖💖💖
Dieux et seule ❤❤❤❤❤❤❤ ndame rek machalla 6:21
Dieureudieuf Serigne Touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿💫💫💫💫💫💫💫💫
Que son âme repose en paix 😭😭
Khassideux yii pour maane garrab leuu ❤ daye fadj lepp ❤. Machalah ❤❤
Baye Moustapha Diop yalla naka Yallah sugnu Borom bi yeureum thi barkep xassida yi
Macha'Allah ndiangue mi nèkh na lool ci khol. Baye Moustapha yalla nako yalla diégal té doli ko yermandé
Mashallah mbackè balla aicha ngoudal fan billay mbgue nanle mashallah dieureudeufe serigne touba mbackè mashallah ❤💖🙏
Je suis tidjan mes j’ai des frissons yalla nagnou yalla fayal sougnou mag you bakh yii sama khôl daffa sedd lol😭🙏🥹
Al hamdoulilah sama khôl dji sede n’a dale ♥️😭😭
Machala Al hamdoulilah
❤❤❤
Mais
Manchallah yalna la yalla ague Serigne Touba fey la, vraiment sa me fait pleuré bilay, j'ai beaucoup fisons ♥️♥️♥️♥️♥️😭😭😭😭
Thieuy Serigne touba léppam mbécté leu
Wakort
Bilay wakh Ko sa kaw😂😂😂😂
@@gorawade3132😊😊³1😊😮😊😮😊😊😊😅😊
Dame aka meuna biinnd amoul morom❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😭😭soumakay deglou damay dioy rek 😭 beugue nala guis té yalla rek takh 🙏🙏😭
J AIME CETTE CHANSON❤❤❤❤❤❤❤❤💎💎💎💎💎💎💎💎💎
Machallah cheikh yalna Serigne bi sameu la li dawna yaram
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤kéne dou serigne touba dh wallahi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalna diam yageu si yow si barké khassida yi 🙏🙏🙏
Yallah na sène adjo, mbébétt, liguène di fadiou Ci Barkep Khassida yi té léép donoukoup tawfekh ci Barkep Ya Rassouloul'Allahi Salaatou Ãlayhi Wassalam
yalla nako sounou borom bayi si sounou kanan sakhal kofi barke khasida yi🙏🙏🙏🤲
Ooooooh machallah machallah machallah ! Si khol bi ngakey yeukk ! Dieureudieuf Cheikhoul Khadim
♥️♥️♥️ j'aime cette chanson
Ok
Dieureudjeufé Seriñ Touba Khadimou Rassoul Diarawlak Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp 🌍❤️🤲🏼
Dieuredieuf Serigne Touba ndayssane jajeuf fall yalla na yalla weereul bât bi si barkep xassida sindidi
thieuy serigne touba❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭
j'ai un tres grand soucis qui me pese sur le coeur priez pour moi barkep serigne saliou mbacke ❤ ab mourite mbokou mouritam rek la ame❤
Yallanala sunu Borom téguil souci yeup ci barke Khassidayi
Yàlla na la yàlla téguine lépp ci daradiay Cheikhoul Khadim
Qu'Allah vous assiste et une procure une paix éternelle
MlhkZPA
Qu’Allah vous delivre par la Bénédiction du Prophète Mouhammad psl 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Dieuredieufetiii Serigne Touba❤❤❤❤...❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤ci bamba dji rek❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
S Moustapha joob yalna YALLA yock Leeram barkép SERIGNE BI
Machalla islam rek moy deuk dieuredieuf serigne touba
Thiey khassidas gniii !!!!!
Thiey khassidas gniii !!!!!
Sans les khassidas l'homme ne découvrira jamais qui est véritablement gou tedd ngui
AK paix intérieur bi c'est unique Machallah
Bilahi walahi li nekhna si khol ❤️
Akassa diadief 👍
Ma cha allah yalla naniou yalla fayal mame borome touba
Serigne mountakha mbacké yall nafii yagg cii barkép khasida sindidi
Amine
Dieureudieuf Serigne Touba Mbacké
Sante Yallah bignu doner ay Mouride 🙏
Allah te donara un jour inchaallah.
thiey ahmadou ak khassida yi bilahi nimouye def si kholeeee❤️❤️❤️❤️❤️
MACHALLAH KHOL SEED NA ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
je suis talibe de serigne touba🥰🥰🥰
Bilahi li nékhna si xole ❤️❤️❤️❤️
Il est très difficile de retenir ses larmes en écoutant cheikh mbaye.