Moussa Ndoye vs Thiatou Daouda Fall finalisé par Albourakh, écoutez les premiers missiles

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 фев 2025
  • ALBOURAKH EVENTS LA CHAINE EVENEMENTIEL
    "Suivez-nous sur Albourakh Events TV, votre destination ultime pour une expérience immersive alliant sport, culture et événementiel. Plongez dans un univers où l'excitation des compétitions sportives rencontre la richesse de la culture, le tout ponctué d'événements inoubliables. Rejoignez-nous pour vivre des moments uniques, où chaque instant est une nouvelle aventure à découvrir. Albourakh Events TV, où la passion devient spectacle."

Комментарии • 194

  • @IbrahimaFall-u3z
    @IbrahimaFall-u3z 7 дней назад +8

    Thiatou daouda fall yalna Allah mayla ndam inchallah thi barké yonentibi PSL 🤲❤️

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko 8 дней назад +5

    Guediawaye moy lamb athia fils ouzz ya meun fouff bilahi ioe ndam si ioe bro yak Jackson futur roi nguèn diam si yèn

  • @assanegueye4884
    @assanegueye4884 8 дней назад +17

    Yallana thiatou Daouda fall dann bark sr fallou

  • @touremamecheikh9737
    @touremamecheikh9737 8 дней назад +10

    Bonne chance thiate daouda fall ndam rk inchaalla danal gniou ragal bii diel mou reuy ❤

  • @modoubayefallsikroulla1423
    @modoubayefallsikroulla1423 8 дней назад +17

    Wa albourakh li lanla tamit 😂😂 Bonne chance thiatou daouda fall yalla nala yalla soutoural may la ndam rk inchallah 💛💙💛💙

  • @papahabibdiop
    @papahabibdiop 8 дней назад +14

    Wawaw thiat yalla boula thiatt topou waay❤

  • @adamadiouf9926
    @adamadiouf9926 5 дней назад

    Ndame rék thiate inchalla 🟦🟨

  • @MamadouDIALLO-oq2dk
    @MamadouDIALLO-oq2dk 8 дней назад +15

    Thiatou Daouda fall kassé 🤞💛💙🔥

  • @CheikhDiop-yg1ut
    @CheikhDiop-yg1ut 8 дней назад +6

    Thiate seul 💛💙 abattoir bi
    Moussa ndoye wadial iow ak say mbok tay rek nga dh 😭

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 6 дней назад +1

    Thiate sama mbok Walo-walo mais nk Moussa Ndoye dou niékhou niébbé déh😂😂😂
    Kou meune sa morom douma🥊✊🏾🤜🏿💪🏾🥊

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 8 дней назад +9

    Moussa Ndoye franchement Fils de Balla moysa adversaire

  • @RamaNiang-kk6hn
    @RamaNiang-kk6hn 7 дней назад +2

    Thiate deh da melni mo eupou dolé moussa ndoye

  • @AidaraBoubacar-i9h
    @AidaraBoubacar-i9h 8 дней назад +7

    Thiatou Daouda fall yalla nako yalla may ndam le petit empereur❤

  • @AbdourahamaneBangoura-t3g
    @AbdourahamaneBangoura-t3g 8 дней назад +6

    Tchatou Daouda Fall ndam rek inchallah

  • @BigMbaye-y2w
    @BigMbaye-y2w 8 дней назад +11

    Kayar derrière Moussa ndoye 💪🎉🎉

  • @papefall7062
    @papefall7062 8 дней назад +17

    Albourakh comme marodi ... Mbeur yeup daniouy diarr deif casting, ame combat 😂😂😂.. mach'Allah que de belles affiches.

  • @KaneArman
    @KaneArman 8 дней назад +2

    T d f❤❤ brome fouta toro

  • @hadeembamba1135
    @hadeembamba1135 8 дней назад +8

    Alieun Seye vs Gris 2!!!! 🙏🏾 🙏🏾

  • @muhammadmassanisane3897
    @muhammadmassanisane3897 8 дней назад +12

    Wa ALBURAKH Nioye Deumbe Pire yen 😂😂😂😂😂😂

  • @bandapape
    @bandapape 8 дней назад +4

    ndam rék TDF inchahallah 🤲🏿🤲🏿🤲🏿

  • @KhalilDia-y3z
    @KhalilDia-y3z 8 дней назад +1

    Thiey albourakh bly yénay lamb 😂 mais thiat ndam rk inchallah ❤❤

  • @AbdoulayeSarr-v9n
    @AbdoulayeSarr-v9n 8 дней назад +3

    Wa albourakh seye 2 lan lalén def ligueni defni niaw ña trop main yalla bakhna

    • @diop3575
      @diop3575 8 дней назад +2

      Saway bayi lene lolou kane mokene wkh ni beugou niou combat wam souko adversaires yi niame woul nak lousi wa albourakh mane

    • @Moustaphaniang313
      @Moustaphaniang313 7 дней назад

      Deméwoul nonou dh frr ménager seye 2 lahat Ndiaye la mom ak wa Al bourakh dioubo mougn lolou tmt mo Dal Jackson Si contre mbaye Gouy gui rk

  • @Elhadjinoreyni11
    @Elhadjinoreyni11 5 дней назад

    Wa albourakh mome ni rék douniou yeureumaté mouk li euppeu na waye😂😂😂

  • @AhmadouBamba-p8t
    @AhmadouBamba-p8t 8 дней назад +3

    thiatou dauda fall seul borome guine bissau

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 8 дней назад +3

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @MoussaDak-o7f
    @MoussaDak-o7f 8 дней назад +4

    Wawaw ndam rék inch'Allah thiatt ❤❤❤😂

  • @AlhamdouLiLahi-wl4cq
    @AlhamdouLiLahi-wl4cq 8 дней назад +7

    Moussa bou noy lay hole Jackson depuis 2022 ba légui ngay daw ak Alioune seye 2 tamite lambj dale😂😂
    Ms bravo Albourakh lambj goudi yi yayy ay beuteum🫣

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 8 дней назад +1

      Mais es ce que promoteur dokh nako nak

    • @badoukamara9844
      @badoukamara9844 8 дней назад

      Pour ioe thiate dafa noye ba beuss ba

    • @Khady114
      @Khady114 8 дней назад

      Niongou moussa ndoye daléni may tangue ba paré dane léne yarakh yarakh bi leuh dh

  • @papemoussadiop83
    @papemoussadiop83 8 дней назад +14

    peul mol gua toy na thiatt yalla nako yalla may ndam nagua wax say supporter gnou yarou

    • @saliouthiam2462
      @saliouthiam2462 8 дней назад +4

      Diéxal nga domou diambour dji dh 😂😂😂li lanla yaw 😂😂

  • @domouguédiawaye-rx7rt
    @domouguédiawaye-rx7rt 8 дней назад +2

    TDF SEULE🎉❤❤❤

  • @elzodieng8067
    @elzodieng8067 8 дней назад +10

    Moussa ndoye kene khamoul loumou beug waye ame nga comba des😂😂😂😂😂

  • @MoussaDak-o7f
    @MoussaDak-o7f 8 дней назад +8

    Thiatou Daouda fall rék lanuy toppu

  • @daoudasarr7150
    @daoudasarr7150 8 дней назад +4

    YARAKH SEUL 💪🏽🔥💪🏽

  • @OusmaneKanee
    @OusmaneKanee 8 дней назад +8

    Alboury hana da bayi beuré

  • @MbayeSylla-t5z
    @MbayeSylla-t5z 8 дней назад

    Thiey war alborakh amonio sene faye bon continuation ❤❤❤❤❤❤

  • @khadimkhadim649
    @khadimkhadim649 8 дней назад +1

    Félicitations ama nékh mola war 😢

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 8 дней назад +6

    *Moussa khaliss rek mola dougueul ci boy bi mais do moromam*

  • @AissatouMbengue-k2o
    @AissatouMbengue-k2o 8 дней назад +1

    Moussa Ndoye kassé❤

  • @OusmaneKanee
    @OusmaneKanee 8 дней назад +62

    Moussa ndoye tapete rek moko si douguel noy dawé Jackson di dieun boy bi

    • @elchico8595
      @elchico8595 8 дней назад +8

      Lamb xalis la saway daniu lay fay louko diar nga beuré
      Sino xoli lénène

    • @PapeDiego-jb7cq
      @PapeDiego-jb7cq 8 дней назад +5

      No vraiment moussa ndoye sama mbeur la mai mangui sogua geum nak ni li guayi Di wah deugleu Noy bagné fils de balla bagne Jackson di beuré AK thiate Daouda fall

    • @MbayeThioumb
      @MbayeThioumb 8 дней назад

      ​@@elchico8595wayy bayi ma guan lamb xalis beugu Lou yobou rk moka dougal si boy bi

    • @abdousene261
      @abdousene261 8 дней назад +1

      Thiate ak nioniu ku geuna tangue??c'est juste une question ❓

    • @MbayeThioumb
      @MbayeThioumb 8 дней назад

      @abdousene261 Jackson guay teguale AK thiatt sama wadji jakson mbeur yi yabou niouko de

  • @abdoudiop8697
    @abdoudiop8697 8 дней назад

    Thiat ndam rek inchallah

  • @thiecoumbadiouf5994
    @thiecoumbadiouf5994 8 дней назад +6

    Revanche moussa ndoye ak aliou seye sakh mo guena logique vraiment lamb yakhouna

  • @diabelndiaye6558
    @diabelndiaye6558 8 дней назад +4

    Quell comba alle thiate

  • @AmethDieng-s5x
    @AmethDieng-s5x 8 дней назад

    Ma gui dém 😮

  • @sawroumbengue7820
    @sawroumbengue7820 8 дней назад +2

    Jackson ak Bombardier nioy beuré par Gaston production

  • @thiebalde921
    @thiebalde921 8 дней назад

    Combat Moussa ak pokola la wone sarap li do comprane sahh

  • @moussasoumare2386
    @moussasoumare2386 8 дней назад +8

    C’est pokola le perdant en refusant Thiatou daouda Fall le jeune a trouvé un adversaire supérieur à lui et Diene

  • @ibrahimandione2116
    @ibrahimandione2116 8 дней назад +2

    Amanekh moleu daan defko sa bop bou bakh et on est encore de tout cœur avec Moussa Ndoye ay lebou laniou lebou mbao bagui ni 🌡️🩸

  • @AlhamdouLiLahi-wl4cq
    @AlhamdouLiLahi-wl4cq 8 дней назад +3

    Saisons 2025 Albourakh
    Premier journée 🫡
    Zarco vs gris
    Fils de balla vs diene kaire
    Pokola vs talfa
    Armée vs ibou afia
    Tapha mbeur vs siteu bou ngor
    Kirikou vs baba diahal
    Papa bari vs tapha Gueye 2
    Mathieu vs diokel
    Deuxième journée
    Ama baldé vs Franc
    Lac Rose vs liss ndiago
    Thiatou yoff vs Domi dangou
    Ndigeul vs bulldozer
    Niang ballo vs nandy fall
    Sokh bou ndaw vs mbacké faye
    Libidor vs ndiaga thiam
    Balla gaye 2 vs siteu
    Moussa ndoye vs thiatou daoda fall
    Quoench vs mbaye gouye gui
    Ada fass vs liss ndiago
    Sokh vs thiatou yarakh
    Serigne Ndiaye 2 vs doudou sané
    Thiatou yoff vs Jacob balde
    Youssou Ndour vs Domi dangou
    Thiatou yarakh vs mama lamine
    Coly faye 2 vs gakou 2
    Talfa vs marley
    Niang 2 vs général bou fass
    Bébé saloum vs weuz Diambar
    Sathies vs Zarco
    Eumeu sene vs zarco
    Pokola vs diene kaire en téléchargement
    Ayy albourakh lékk rk nga niou défoul 😅😅
    Ms souniou mbeur mi combat wayy
    Diam térry😢

  • @tallambodji5284
    @tallambodji5284 6 дней назад

    Moussa Ndoy khamouma Ñiata lagnioula fay mai comba Risque nga dieul boybi day Daim dee

  • @MatySow-n8e
    @MatySow-n8e 8 дней назад +4

    Albourakh 1

  • @MatarMBacke-p8e
    @MatarMBacke-p8e 8 дней назад +1

    Albourakh doyna nak 😂😂😂❤❤❤😂😂😂😂❤❤❤❤😂😂

  • @Chakor8955
    @Chakor8955 8 дней назад +1

    Thiàttou daffa wareu beurré ak ay moromam ba si kanam

  • @papemoussadiop83
    @papemoussadiop83 8 дней назад +3

    ndiankile khexe thiate daoda fall

  • @SarrmodouSarr-sv3jo
    @SarrmodouSarr-sv3jo 8 дней назад

    yalla nala yalla soutoural mayla ndam

  • @kaderdiop8543
    @kaderdiop8543 8 дней назад +2

    Fékhé nguene dal ba khalal boy bi , khekh amanekh pour woutal boy bi yone

  • @gorguidieng7796
    @gorguidieng7796 8 дней назад +1

    Ah moussa dal wéré nga

  • @papadaoudathiam3903
    @papadaoudathiam3903 8 дней назад

    Moussa ndoye yalla nako yalla may ndam

  • @khadimgueye1052
    @khadimgueye1052 8 дней назад +1

    Merci

  • @oumarniang5542
    @oumarniang5542 7 дней назад

    Li la ziguili nay lpp link lh 😂wara beuré ak say morom di daw

  • @layeNdiaye77
    @layeNdiaye77 8 дней назад

    Mai Moussa ndoye khana amoul staff😂😂😂😂

  • @mouhamadoulaminebadiane2644
    @mouhamadoulaminebadiane2644 8 дней назад +1

    Moussa Ndoye y’a gnak diome deugueu . Bagne Jackson , dieul Tiatou Daouda Fall 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅. Lambeu dji legui amtoul diambar bilahi . Moussa Ndoye pour mane bilahi Eumeu Séne guaye dieul 😅😅😅😅😅

    • @MorFall-zf5hc
      @MorFall-zf5hc 8 дней назад +1

      Bly yarakh la deuk dh mais ki diakhalnama😢

  • @PapaThiam-pm8ss
    @PapaThiam-pm8ss 8 дней назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @KhalilSamba-r1s
    @KhalilSamba-r1s 8 дней назад

    Délén wakh bayi sén yii ah

  • @Bayedarou-r7l
    @Bayedarou-r7l 8 дней назад

    Moussa ndoye daw Jackson rkk mkô yobé lii wayé yalle naniou dane sa ndeye dangua sokhore ndayame

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 8 дней назад

    😅😅😅😅😅wa Al bourakh loléne beugue 😅😅😅😅

  • @fallabdou-sc3fu
    @fallabdou-sc3fu 8 дней назад

    Albourakh kassè🎉 souniou futur Balla Gaye.

  • @dine911
    @dine911 8 дней назад +1

    𝐌𝐨𝐮𝐬𝐬𝐚 𝐧𝐝𝐨𝐲𝐞 𝐦𝐨 𝐦𝐞𝐮𝐧𝐞 𝐦𝐨 𝐞𝐮𝐩𝐨𝐮 𝐝𝐨𝐥𝐞 𝐤𝐢𝐢 𝐤𝐡𝐚𝐦𝐮𝐥𝐞

  • @matarsene8343
    @matarsene8343 8 дней назад

    Thiatt seul ❤

  • @khadimseye9364
    @khadimseye9364 8 дней назад

    Thiate bonne chance

  • @Amm2293
    @Amm2293 8 дней назад

    Non billahi lamb diékhna si niom modlo ak eumeu ak balla, sén BIR lagn dane beuré moudone ak wouré you méti té nekh, mais ay boy yo khamné pour niom foumou gueneu noyéé rek...

  • @ndiouga-lf6hp
    @ndiouga-lf6hp 8 дней назад

    Moussa waro beure AK vote bi

  • @tavarezcheikhou517
    @tavarezcheikhou517 8 дней назад

    Daw Jackson jeul daouda fall Wa lamb mome

  • @BachorLali
    @BachorLali 8 дней назад

    Lamb amatoul valeur

  • @matarsene8343
    @matarsene8343 8 дней назад

    Moussa ndoye dafa ragal jackson junior 😂😊

  • @ibrahimasarr883
    @ibrahimasarr883 7 дней назад

    Thiate kessé

  • @khadimfall979
    @khadimfall979 8 дней назад

    I ❤❤🎉

  • @Loum858
    @Loum858 8 дней назад +1

    Thiey Jackson moy ndanan billahi 😂

  • @AissatouMbengue-k2o
    @AissatouMbengue-k2o 8 дней назад

    Alboury vs zambala

  • @Kaddudeuggui
    @Kaddudeuggui 8 дней назад

    Sey2 vs bombardier
    Jackson vs moussa ndoy
    Thiathou dawda fall vs pokola
    Mbaye gouygui vs sokh
    Quench vs diénne kaîré
    Thiathou yarakh vs gora sock
    Mo warone nék combat yi

  • @mansourgaye2792
    @mansourgaye2792 8 дней назад +1

    Moussa daffa nouro ak grand frère thiatou daoda fall bi less 2

  • @SarrmodouSarr-sv3jo
    @SarrmodouSarr-sv3jo 8 дней назад

    💙💛💙💛

  • @modoudiouf5336
    @modoudiouf5336 8 дней назад

    Moussa ndoy tapet la nofiyy bayé diakson di dieul thiatou

  • @thiecoumbadiouf5994
    @thiecoumbadiouf5994 8 дней назад +2

    mani fi benn dabanté amoufi nitou lamb delen wakh liy deg thiate mi amanekh dan nako dieul bou ler nanie

  • @bayewalyndiaye3003
    @bayewalyndiaye3003 8 дней назад

    Moussa ndoye tapétt la dafa beug lou yombou

  • @assanekane1426
    @assanekane1426 8 дней назад

    MOUSSA NDOYE MI LOU NOYE REK LAYE WEUR RAGAL DAPNAKO KI DOYNA WAR

  • @Degaul-xo1qc
    @Degaul-xo1qc 8 дней назад

    Daw ndey jakson beugueu lou noy li moy lamb legui😂

  • @falldaly3800
    @falldaly3800 8 дней назад

    Li mom d'où yone lamb leki d'où affaire diambar affaire de Yama nehbla

  • @sarrabdou3040
    @sarrabdou3040 8 дней назад

    Ndoye ya geunneu tapèt ndey si. Mbeur yupp bayi fi ay fils de Balla, diom niom Jackson,daan thiat yobouleu fènn

  • @WaxDeug21
    @WaxDeug21 8 дней назад

    Moussa Ndoye ak Quench niémé wougn Jackson ! 😂

  • @cheikhgassama6877
    @cheikhgassama6877 8 дней назад

    Kouy daw jackson di dieul thiate 😂😂😂

  • @YacineDia-ir6pe
    @YacineDia-ir6pe 8 дней назад +2

    Wa lgui moussa bou dieulé boy yii nie nekk sa guinao kane laniouye beurel gooré dal yomboul

  • @serignemodouciss7270
    @serignemodouciss7270 8 дней назад

    Moussa Ndoye mi narr na dioum si TDF mi dh bakhna rék

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi 8 дней назад

    Moussa ndoye kou khoromou la😂😂😂

  • @amaduamadu1600
    @amaduamadu1600 8 дней назад

    Si khaliss moko si dougeul waye day liguey

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 8 дней назад

    Moussa ndoye aka beugg lou yomb

  • @ibrahimandione2116
    @ibrahimandione2116 8 дней назад

    Zambala khana dou beuré tmt 😢😢😢😢😢

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi 8 дней назад

    7:12 😂😂😂😂

  • @cheikhthiam-k9o
    @cheikhthiam-k9o 8 дней назад

    Ah mosa ndoye fish de balla modone comba bi li Moy lane

  • @khaliloulah3703
    @khaliloulah3703 8 дней назад

    Moussa ndoye bimou teuko zoss la parei si mom😹😂😂😂😂

  • @IzoLaye
    @IzoLaye 8 дней назад

    Bilahi ki tapét laa Jackson nga daw fils de bala nga waff di latch zoss lou noy rék ngay Weur

  • @YoumDiouf
    @YoumDiouf 8 дней назад

    Moussa beug nga lou yomb nak