Audio Racky Et Marie Louise Diaw '' Lii Mo Waral Thiowli....''

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 25 дек 2024

Комментарии • 456

  • @oulydiallo6652
    @oulydiallo6652 4 года назад +1

    Racky défoul drah lepp Marie Louise leu soxor ignane rekk moko diapp senegal mo méti leigui démo do bayi sa morom dem
    Xolal racky boul fallé beine soss katt yangui doray door gère tn foyer gueneu diapp sa borom keur.
    Junior machallah sa liguéy raffet neu

  • @massbakhyaye4472
    @massbakhyaye4472 4 года назад +22

    Bayilén di wakh Racky aidra kou beugue kham loutakh rek beuseul j aime après ma wakh lén kouy racky thi lou woor damako kham barki Mouhamed

  • @fatimafaliloulah1145
    @fatimafaliloulah1145 4 года назад +201

    Parlons de nos frères qui sont dans le désarroi en Chine
    Parlons de la hausse de l'électricité et du coût de la vie .
    Parlons de l'insécurité, l'insalubrité, manque d'écoles et d'hôpitaux équipés.
    C'est plus important je trouve. Désolée

    • @ibrahimadiagne9026
      @ibrahimadiagne9026 4 года назад +5

      Enfin quelqu'un qui réfléchit y'a des choses beaucoup plus importante à montrer

    • @marieFmbaye
      @marieFmbaye 4 года назад

      Fatima Faliloulah c’est une chaîne de news sénégalais il parle de NEWS SÉNÉGALAIS fall metigueine

    • @maremaniang1741
      @maremaniang1741 4 года назад +1

      Très bien Fréro à vré dire nous on a d'autres cha à fouiller que être ici Racki par si Mari par la

    • @mymachoumby848
      @mymachoumby848 4 года назад +1

      wa kay yaw nak la andall

    • @diattousow2104
      @diattousow2104 4 года назад +1

      Fatima Faliloulah bilay ta raison

  • @layesy3148
    @layesy3148 4 года назад +1

    Marie Louise dal dou niit kou bakh yak katou deer la

  • @maimounasy1745
    @maimounasy1745 4 года назад +19

    Machaalla Junior Gueye wakh djii am solo trop😻ni RK gua meuneu wakhé pck sa yaye dafa bakh

  • @yacineba160
    @yacineba160 4 года назад +30

    Marie Louise lii daffa niaaw trop Racky mingui soogga dougou thi sey respect Book et essaie de faire comme elle tmt

  • @annadiouf1113
    @annadiouf1113 4 года назад +114

    Eh racky n'a rien fait c marie louise qui est jalouse

  • @mariemethiam397
    @mariemethiam397 4 года назад +1

    Mari Louise da pérte soxor ak iñane rék moko diapou racky rawnala vas là-bas 🤣

  • @myablacky
    @myablacky 4 года назад +34

    Marie Louise mofi indi li yeuppp

  • @myasarr2055
    @myasarr2055 4 года назад

    Bien dit frèro di appuyait rek ci linga wah mouy ñoun djiguén yii nanou holat sounou dieuf téy halat soubeu niñou néké cii réwmi ñawna amatounou bén valeur ndah liii chak jr di dioté ndah goor gni seuyoul nañou bayi gni seuy seuy gny seuy moytou gny seuyoul

  • @almaktoum7367
    @almaktoum7367 4 года назад +120

    Frère ya dès chose plus important que sa

    • @fatousidibe2903
      @fatousidibe2903 4 года назад +2

      Bilahi

    • @maimounakonate1175
      @maimounakonate1175 4 года назад +1

      Vraiment

    • @diopsouleymane1595
      @diopsouleymane1595 4 года назад +1

      Vraiment , no comment Bro

    • @ndiayemariehelene2126
      @ndiayemariehelene2126 4 года назад

      Ndiasse Mbengue wakhale d frère journaliste y gno amoule nivo t niakh ligueye masta iow mi goor di reporte guagne y é mn pays va mal li amena ba diale guani do bayii

    • @coumbamane2487
      @coumbamane2487 4 года назад

      Yaw wero ms li si doungou deuk la khèwè et on en parle kham way

  • @rusamelrusamel2642
    @rusamelrusamel2642 4 года назад +15

    Bilaye li nga wah lepp deugui la li daa rouslou nyaw. Yalla nanou yalla dollil sutoura

  • @aminaba6130
    @aminaba6130 4 года назад +67

    Est ce ke louise di la verite peut etre dey socc rek

    • @zeynahaidara368
      @zeynahaidara368 4 года назад +1

      Bilay

    • @keurserignetoubamulti-serv4334
      @keurserignetoubamulti-serv4334 4 года назад +8

      day soss rek kou deg limouy xamni dou deug dafa beug yakh déram rek c'est un salot

    • @aminadacosta7191
      @aminadacosta7191 4 года назад +2

      Dafay sosse par ce k dafa désespérée tei bugul moromam rawko

    • @khadymboup9881
      @khadymboup9881 4 года назад +5

      Yaw bou degue maris Louis nimi wakhee rkk ga khammnee day soss parceque biko raky tabaler saga ndeye da coupé

    • @misstchiptchip2963
      @misstchiptchip2963 4 года назад +6

      C vrai pour la grossesse et le portable que cheikhou a donner... Cheikhou draguer racky pendant que sa 2ème femme etait enceinte... C vrai que Marie louise n'est pas un exemple mais racky aussi moy lolou Marie louise n'a rien inventé tout est vrai... Niom nieup nio yem

  • @aminadacosta7191
    @aminadacosta7191 4 года назад +41

    Mr, Racky n'a rien fait c'est Marie Louise qui a ouvert le débat et lui a posé des questions bête et de fausse accusation. En tt cas lii mom diarul débat car on a d'autres chats à fuetter

  • @salimatadiome9779
    @salimatadiome9779 4 года назад

    En tout cas toute les 2 sont fautifs et la belle famille de racky kéneu rawoulen nio indi wakh bi yeup.

  • @weuzistapouye1611
    @weuzistapouye1611 4 года назад +1

    Wa nateu bi mois niata la

  • @buzzdiverstv2158
    @buzzdiverstv2158 4 года назад +49

    No raky n,a rien fait elle a juste dementir tè limou wakh dieukeureum moko lath motakh mou wakh ko

  • @diarrawakhdeug3365
    @diarrawakhdeug3365 4 года назад +71

    Racky dafoul dara
    Marie Louise mo Niakk classe,perte,be pare di sosss

  • @cissechouette3314
    @cissechouette3314 4 года назад

    J'aime bien ce gars deug rek la fi wakh bonne continuation. Na sa mbokou yi roy ci yow mo gueune gnouy yokou tiow fougnou toloû. Bravo et merci pour les conseils !

  • @babagolockosibor3706
    @babagolockosibor3706 4 года назад +53

    Marie Louise moy dmrm bi

  • @mamadoutoure4774
    @mamadoutoure4774 4 года назад

    Elles sont Pareils niome niar nieupa yame respectèwouniou sène bopou respectèwougnou sène famille ni wa Sénégal

  • @aisatoudram89
    @aisatoudram89 4 года назад +12

    À mes frères et sœurs chers compatriotes parlons des personnes qui sont malades
    Pensons à ses personnes agressées et tués
    Parlons de notre pays qui va vraiment mal
    Un peu de respect pour nos morts svp
    Au nom d'Allah passons à notre pays qui va vraiment mal et laissons ses femmes ses hommes se chamailler ce n'est pas notre problème svp

  • @kamaraastou528
    @kamaraastou528 4 года назад

    Humm ému kone lii yepp mongui circuler au galsen té yeugiumako c vraiment tristes bilahi que dieu nous garde

  • @ousmandarboe589
    @ousmandarboe589 4 года назад

    Racky Seyal ki bouko bayi mou stresse da jalouse

  • @thiammamediarra5135
    @thiammamediarra5135 4 года назад +2

    Yalnagnou yalla mousal si kharit bou djiguen😑solen khoulo wè lep loumla khamalon dinako wakh

  • @diegomessi8736
    @diegomessi8736 4 года назад +1

    Sunugal gui legui bop bouy meti amoul fouy cedd

  • @diarafaaidara3715
    @diarafaaidara3715 4 года назад +52

    Vraiment tu as raison, soutoureu amatoul 🥺 les filles nak 0 respect 0 classe 😩 0 dignité 😭

    • @abrahamndiaye2016
      @abrahamndiaye2016 4 года назад +2

      iow lay àndal

    • @fatoungom3811
      @fatoungom3811 4 года назад +3

      Djiguene yii dh leGui niniou mell niaw na trooop

    • @diarafaaidara3715
      @diarafaaidara3715 4 года назад

      T légui kéne dou soutoural moromame , boléne néké si diame niou khamal la lep , sougnou paré si yaw nak wér la comme guédieu😭 , yalla na yalla deff diame Sénégal

    • @ramatadiop7515
      @ramatadiop7515 4 года назад

      Merci

    • @ndeyesamb1160
      @ndeyesamb1160 4 года назад

      Hihh0

  • @papadiop2642
    @papadiop2642 4 года назад

    Véritable pur mon frère courage

  • @landingdiouf9401
    @landingdiouf9401 4 года назад

    Tu joue bien ton role frere

  • @beuggsamayaye1366
    @beuggsamayaye1366 4 года назад

    Marie Louise mi dina rèthiou loumou deff sokhor na torop tè ignane li dafa niaw way niank classe ba dè

  • @aissatadaff6574
    @aissatadaff6574 4 года назад +17

    Souma nekon racky barki Yallah demakoy porté plainte

    • @amysene6789
      @amysene6789 4 года назад

      Aïssata Daff walay diare nako li dafa niaw mari louise elle exagère

    • @mamediarrandiaye7698
      @mamediarrandiaye7698 4 года назад

      Jai dit la meme chose marie Louise mo niank fouleu mouy doul ni mane dal endou légui yi en tout cas racky khawma appart si télé bi mes marie Louise noumouy waxé rkk guay xamni day doul

  • @awalaye2404
    @awalaye2404 4 года назад +1

    Amna solo la vie est belle

  • @tefmb3313
    @tefmb3313 4 года назад

    Hee katale sa ndeye feulee waaye maylène marie Louise jaam waaye

  • @wouryelfenomenoolldia6007
    @wouryelfenomenoolldia6007 4 года назад

    En tt cas wérrr ngénn sen bopp . Djiguéne gni yéwou léne

  • @diegomessi8736
    @diegomessi8736 4 года назад +1

    Senegal soirée vampire la legui kou diekou sa morom defal ko affaire

  • @khadidjandiaye7299
    @khadidjandiaye7299 4 года назад

    Nexoule ba nexoule ki mo bone tacky defouko dara jalouse rekk la deff thimmmm

  • @khadysarr1950
    @khadysarr1950 4 года назад

    Marie Louise kou nieupeu teufli nga toy.kholal commentaire yiii rk keneu dou mari j ne sais pas si c vrai ou pas mai amo bamélou biirrr🤔

  • @keurserignetoubamulti-serv4334
    @keurserignetoubamulti-serv4334 4 года назад +20

    mane j'en suis sur que racky xamoul wone ni marie dacoy enregistre cone douko wouyou ndax couy wadial mariage do déf louy yax sa ménage

  • @khelcomacademiehdtv5262
    @khelcomacademiehdtv5262 4 года назад

    Masalah wakhjiè Amna solo Amal diamo

  • @inandao5284
    @inandao5284 4 года назад

    Marie Louise dal dafa jalouse rek

  • @adamasenghor7031
    @adamasenghor7031 4 года назад +1

    Racky la rek nit dengay mouss touti bimou khamné Marie Louis indiwoul diam mou raccrocher téléphone nit dengay daw tiow té yalla takh dou question ragal tapasanté amoul ndierign ko raté rek mo koy def gnoun djiguen nagnou khalat sougnou bop té yalla takh

  • @madeleinely3231
    @madeleinely3231 4 года назад +1

    Marie Louise beuguon nala trop mai nak yak gua leep ndakh yaw dagua wathié sa bop Mane dh personnellement nawlo toumala ndakh li même sou amon sakh waroko wakh li mom sokhor lako meune toudé ki di marié gua beugue yak adounam yaw ndéké do dara

  • @abibsene4685
    @abibsene4685 4 года назад

    Ne tinquite pas raky nous t'aimons toujours marie Louise mounoula yakkeu soit forte

  • @khadysarr6358
    @khadysarr6358 4 года назад +32

    Légui kou soti Natt bi niata geuy ame

  • @moustaphagueye6901
    @moustaphagueye6901 4 года назад

    Machaala kadouyii amrna solo kouyy déff loubakh rek lagnou critiké senegal

  • @abythiam3334
    @abythiam3334 4 года назад

    Bien dit senegal mome legui

  • @yasminadiop982
    @yasminadiop982 4 года назад

    Ayy dou yame thi boupou borome marie lepp thi sa kawe la tournée wate

  • @eldiablo7007
    @eldiablo7007 4 года назад

    Vraiment lègui Sénégal 🇸🇳 yakou na kéne soutouralatoule kéne sur tout nous les femmes li daw na yaram sétt léne ci yalla waye ça c’est honteux ☺️

  • @antandiayeseck6315
    @antandiayeseck6315 4 года назад +1

    leep Marie louise leu domrame la reik sokhor kasse mola diap thipriiii
    kou and ak man beusseul jaime ma xol

  • @manendiaye8540
    @manendiaye8540 4 года назад

    Marie tu es vraiment jalouse

  • @samadieukeursamaharit9543
    @samadieukeursamaharit9543 4 года назад

    Li appelle d'enregistrement Marie Louise da prèparè coubi bou bakh ndakh biko raky du beugue saga thiala coupè téléphone esk sakh yakoum bire amna

  • @mathiousamb7230
    @mathiousamb7230 4 года назад +53

    Marie Louise dara djapouko loudoul ignane

  • @elhadjindiaye2228
    @elhadjindiaye2228 4 года назад

    Goor dou doull.
    Lidieunti euyibou diambour té fekk ya gueuneu torox

  • @mahawakouyate8959
    @mahawakouyate8959 4 года назад

    Tu a raison soutoura

  • @morlam3515
    @morlam3515 4 года назад +49

    Marie Louise kou sokhor le

  • @diatoushacorrea8090
    @diatoushacorrea8090 4 года назад +1

    Marie Louis c'est une vipére féne rék à mo béne class

  • @lalinguereniang7681
    @lalinguereniang7681 4 года назад +86

    Mari louise nimouy wakhe rk nga Kham ni day sos demal wouti dieukeur Moguene tabayi sos yi ak anniversaire gou Méti yi la guis mane

    • @aichathiaw179
      @aichathiaw179 4 года назад +3

      Bilahi

    • @khadyndiaye324
      @khadyndiaye324 4 года назад +3

      Waw cause mayouko mou wax

    • @mamysaliou5918
      @mamysaliou5918 4 года назад +4

      la linguere Niang mane de bimako deguelo nena dakoy sosaal ci sama khalat... lolou lagnou toudee « khoulo thiaga » bou beugue gagner ci khoulo bi dagayy soss

    • @ndeyekhadydiop7867
      @ndeyekhadydiop7867 4 года назад +1

      Mamy Saliou 😂😂no ray gaman

    • @lalinguereniang7681
      @lalinguereniang7681 4 года назад +1

      @@mamysaliou5918 yako lal da perte rkk

  • @sadioseck1126
    @sadioseck1126 4 года назад +1

    Kou défe dara laygnouy soutourar meis raky defoul dara xallé bou bakh

  • @sgmtvsenegal6710
    @sgmtvsenegal6710 4 года назад +44

    Excuse moi mon gars mais t'es pas professionnel certe t'as donné des conseils intéressants mais ne refait plus l'erreur de commenté des propos de ce genre s'en preuve ni argument peusible et à eux je peux dire que tu ne les as pas donné de conseils mais plutôt tu les juge en te basant sur un soit disant appel téléphonique enregistré en gros une querelle entre fille ce qu'a fait RANGOU c'est flagrant pour le prochaine foi assuré toi d'avoir le témoignage des deux concernés. bi môme moy lolou boum la dalat pardonne si j'ai Di quelque chose qu'il ne fallait pas

  • @abibsene4685
    @abibsene4685 4 года назад

    Kou nékeu amna passé

  • @misskourouni1428
    @misskourouni1428 4 года назад

    Lou leu beteu mouneleu.Racky ne savait pas que Marie Louise l'enregistrait par jalousie et méchanceté.Racky doit porter plainte ou tout simplement l'ignorer complètement car M Louise a échoué sur tous les plans en voulant détruire l'image de Racky .Bon ménage

  • @machallahanta7773
    @machallahanta7773 4 года назад +6

    Très bien parlé mon fils merci

  • @aidaniang9350
    @aidaniang9350 4 года назад +19

    Raky Je t'aime

  • @annagueye6035
    @annagueye6035 4 года назад +1

    Non kouyabo def loubaxx kharite amatoul bilahiii ki takagouniou saxx nguéni waxii vie privée wam mm bouyakeii bir lousi yonam mom la rek Marie Louise nawouti jekar cmieux😠ki soumako diapei na....

  • @ndongodg9286
    @ndongodg9286 4 года назад

    Non bilay Sénégal dafa nekh toujours problème 😆😆mdr

  • @aliounediouf1447
    @aliounediouf1447 4 года назад

    Boulén niou sonal way

  • @mamasy1972
    @mamasy1972 4 года назад +12

    Danma rousse bilaye marie danfa bonne rek montakh nekhe Dakar di defloula saf

    • @afriquetvtv3093
      @afriquetvtv3093 4 года назад

      Mai ñiénne si goorñi nioko déf alal dapla dódém se mbokku takkuko allak thiow lulafa fékk nuxamni yayla duyombu mai mai giss nit thi séri yi rék ak téléyi dug thi

    • @panndiop6262
      @panndiop6262 4 года назад

      @@afriquetvtv3093 dou dara loudoul tarr ki raféte na kharal ma dokhanko

  • @nabounabou1354
    @nabounabou1354 4 года назад +33

    Li Racky dem seuyi bayiko fi moko ndey metti... Gnak class yala dinala fay sa bore

    • @alphasow7296
      @alphasow7296 4 года назад +2

      bilahi degou la lolou rekk mok meti

    • @aramediouf4785
      @aramediouf4785 4 года назад +2

      Mom lanla deff ba takouniouko robko ni avion racky da am valeur la mo tah niou tako

  • @Rimka912
    @Rimka912 4 года назад

    Mane khoma les hommes laane lagnou guiss sii vache folle yii tee bayifii khalee you bakh yi doff yi rek nion sagn takk djigeene yi makhala footballeur yi nion geneu doff nieup ay vache folle rek lagniy takk

  • @wanewane6065
    @wanewane6065 4 года назад

    Machala bien di

  • @amycisse1495
    @amycisse1495 4 года назад +47

    C k nak marie Louis elle est juste jalouse tmt ndakh sokhor wéssu wul li

  • @yacinefaye969
    @yacinefaye969 4 года назад

    Mari Louis tu es jalouse 😋laise la vivre en paix et va cherché un mari mogueuneu

  • @aidasamb591
    @aidasamb591 4 года назад +1

    salamalekoum mbokii internote yii😂😂😂

  • @marichandiayediallo4528
    @marichandiayediallo4528 4 года назад +29

    Racky wakhoul dara lou aye marie Daye doul rék pck elle a dja programmé l’audio marie Louise mo togne mais yallah dina léne atté

    • @choupitasene454
      @choupitasene454 4 года назад

      Nn loutax sénégalais bone racki na rien fait putin yéne bonne waye

  • @luxz7711
    @luxz7711 4 года назад

    Il y a pas des autres problèmes un peu plus importants à régler au Sénégal.

  • @mbayepapendiouga2426
    @mbayepapendiouga2426 4 года назад

    merci beaucoup boy bien dit

  • @zeynabouaidara8157
    @zeynabouaidara8157 4 года назад

    Mari louissss est jaloux, raki dom bay seyel seybi 😍👍

    • @mounababby6148
      @mounababby6148 4 года назад

      Mari Louissss niakengeu class niakeu faydeu firr thim 😡😡

  • @djaraf3808
    @djaraf3808 2 года назад

    Yéna genrou djiguéne yi, goor gniléne di takk gnokko déff, goor gnognou gnokh djiguéne gnognou gno yéne. Louyy tarr, tarr dou seuyy. Y’a aussi la jalousie. Nitt kou nékk akh li yalla bindeu thi sa dieuh

  • @ndeyeteningcamara7297
    @ndeyeteningcamara7297 4 года назад

    Sénégal dagno wara ame ben esprit de dépassement yen yi rafetoul surtout soor len yenay diourr kilifa ak kou nek si deukeu bi li d'où beuzz dh

  • @diagnekode9298
    @diagnekode9298 4 года назад

    Tu as parfaitement raison degueu piir degue d'où nekh Lingua wakh yėp deguele soutera Moye lėep boko amoul SA dounde amoul ndierine

  • @farydiop5530
    @farydiop5530 4 года назад +9

    thiey yalla ay djiguene guene soralelene euleuk taguene soutoural sen bop yalla sakh day soutoural diamam

  • @kaylewalker5487
    @kaylewalker5487 4 года назад

    Sokhor bi nek si rew mi diakhal nama noooo Li eupna tmt noooo 🙆‍♂️😢😢😢

  • @dabstina8104
    @dabstina8104 4 года назад

    Bilay deuguela

  • @nguenardndiaye2876
    @nguenardndiaye2876 4 года назад +1

    Yéne kate bou li amoutone douguéne liguey ndakh li rek guene yakamti .sénégal lou bakh mogui fi am ba tey yenakodoul tek.

  • @awalam8161
    @awalam8161 4 года назад

    Lepp marie louise la..sènègalais yi dougn dem t douniou bayi keneu dou dem..sokhor lagn dff..ignane ..jalouse..bonn..wayè kossi guiss dou avancer jamais..liguènn yènè sènn bop yènè lènn ko gnigni..ms dougn ko dfff..niom rk nioy avancer dou kènéne...marie louise bayil diambour seyy seuyeum li ba diam yalnako djikk wayy..racky mn idole..yalla nalla yalla may ay ndiabott you barkell..am seuy bou barkell

  • @khoudiasambkeita1992
    @khoudiasambkeita1992 4 года назад +25

    Jalousie RK marie Louis kou tothie thiotou ndeye la dmr beugoul kokou devancé toujours derrière RK thiagua kharama ta ndiaye wor boite yi ak hôtel yi rk

  • @aidafall5390
    @aidafall5390 4 года назад

    Macha alla boudjapou meloneneyawe dinabakhe

  • @fatoudiallo991
    @fatoudiallo991 4 года назад

    Racky défoulle dara c est marie louise

  • @titifarou8257
    @titifarou8257 4 года назад

    Mé racki défoul dara marie mo sokhor té dafaye sosse té téwoul mariage bi amna 😂😂😂😂marie ya pérte

  • @fallaminata9042
    @fallaminata9042 4 года назад

    Racky bravo merci

  • @isseulaye7332
    @isseulaye7332 4 года назад

    Merci bros elle sont pas réglos

  • @khadydiop8274
    @khadydiop8274 4 года назад +11

    Bonne rekkk mais racky khamoul sakh nee ke gningy koy enregistrer lepp racky

    • @mariamadiene8314
      @mariamadiene8314 4 года назад +3

      Bien dit ell savait mm po k marie Louise l'enregistreé

  • @lamzasylla9039
    @lamzasylla9039 4 года назад

    Vraiment ms lea defous sure2

  • @farbasagna7699
    @farbasagna7699 4 года назад +1

    Pour moi Li d'où actualités au domèram laniou

  • @ndeyebinetadiagne3473
    @ndeyebinetadiagne3473 4 года назад

    Na gooré way

  • @apouta6595
    @apouta6595 4 года назад +23

    Yawe tame sa liguèye yombeuna tokke expliquer Lou gneupe khame ba parè ....

  • @naboudiouf8735
    @naboudiouf8735 4 года назад

    Thiey adouna

  • @awaladivafall5033
    @awaladivafall5033 4 года назад

    Votre célébrité n'a pas d'auteurs sur vos carrières .c'est dieu qui décide l'Union mais pas la personnes .elles ont oublié si on taquine vos enfants .il faut prévoir le futur de vos famille et enfants

  • @moukhameta6418
    @moukhameta6418 4 года назад

    Après mou diekhe koi, li moye sa job koi
    Yokk thieurer doli diekhe RK nga fi def

  • @generalboucoumbagawlo2257
    @generalboucoumbagawlo2257 4 года назад

    Antoucka cette marie Louis et méchante