modou modou yi ak fatou fatou yi yalnaléne yalla same défaléne téragua ak ay khéweul baguène dèlou sénégal kéne bagna woutè mougne léne dina bakh incha allah
Tu a rasion 😢 Mn pere c 1 Modou Modou comme toi Moi je nee au italie. Mais tu parle Que la verite au italie la Vie est dificill😪 Mais wa senegal da niou yan Que xell Je s8 content sur toi ❤❤❤
This is true man I feel your pain man Sénégal is mess up they don't care about no one just money and not only that your own family well turn they're back on you after you suffer for them ppl this's days are just material realistic
Vraiment liga wakh cé la vérité guisga mane mi maroc la nékone défa mettiwone trop parce-que souma khamé prison maroc lako khamé gnou nék Sénégal lo envoyé thi khalliss niou lékk ko té sou gnibi sé amo lou nék niou wakh mé cé la vie diaradieuf modou modou yi que dieu vous garde yalla bahna
Merci mon grand moi je veut ces gener de parole Parceque j vient d arriver mais j ai commencé à tirer des leçons merci pour encore une fois de plus. Que le bonne dieu protéger à tous les émigrés barke seydina Mohamed psl.
Je ne suis pas ď accord avec toi j suis comme vous mon Premier voyage au senegal jai 50€ dans ma poche ma familia ma recibió con corazón mes amies también l
machallah liga wakh lèpe deuge le mais nane sante yalla ko sa nione yaye mayè wayè kène dou la may tèn bagna khawi sono sotoura ndakh nièpe sono waye nite niè thi sotoura lan rawantè
Bilahi deug pirr ga wax déh mane déh sama borom keur modou modou la wayé mane déh fék magui and ak sama xél ma diko diapalé unchalah ndakh dagnouy sacrifier sén bop ndakh gnounn
Aicha Achia c'est vrai deh parcque au Sénégal il croit que nous les modou ont ramasse de largent mais ils se trompe mon argent à part ma mere et mes soeurs je donne personnes à mon argent
Modou modou thi bopam moye diambar mais c est le Sénégal qui est ainsi une fois que nguaye débrouiller di fadje sohlayi danioulaye nenguedjie dounioula maye darra té so démè ba meunoto gniepe alaye bayi même saye propre mbok motah legui kenne kou neque hamal sa bopp du courage vive les immigrés vive kepe kouye gorgorlou birr ak biti
modou modou yi ak fatou fatou yi yalnaléne yalla same défaléne téragua ak ay khéweul baguène dèlou sénégal kéne bagna woutè mougne léne dina bakh incha allah
Mossane faye amineeeeeeeeee
Tu a rasion 😢 Mn pere c 1 Modou Modou comme toi Moi je nee au italie. Mais tu parle Que la verite au italie la Vie est dificill😪 Mais wa senegal da niou yan Que xell
Je s8 content sur toi ❤❤❤
This is true man I feel your pain man Sénégal is mess up they don't care about no one just money and not only that your own family well turn they're back on you after you suffer for them ppl this's days are just material realistic
wallahi yaw tamite wakhalo kénn koudoul mane linga wakh yépp thi senegal damako doundou
Ma sha Allah Mercii Bor tnx so muc bor Good bless you
Walahi wakhatikko wayy goor Sénégal fayougnou narr Ba khoromom Modou Modou yiii dagno sone tayi dèee dosi yonè nitt nakk Bamou diote khaliss bi mou woola nila dieureudief diotnako amoul
Wakh nga deug dh billahi sama yaram dawna yalla nalèn yalla sambo yén Modou modou yi
Interek biilahi❤❤
Vraiment liga wakh cé la vérité guisga mane mi maroc la nékone défa mettiwone trop parce-que souma khamé prison maroc lako khamé gnou nék Sénégal lo envoyé thi khalliss niou lékk ko té sou gnibi sé amo lou nék niou wakh mé cé la vie diaradieuf modou modou yi que dieu vous garde yalla bahna
Masha Allah amna solo trop
😣😣 yes we all know modou modou is the best bro but No problem God bless you all Amen 😤😤
Serigne Touba amoule morome
Ndeysane sama xol toina😭😭😭🤲🤲🤲
Merci mon grand moi je veut ces gener de parole Parceque j vient d arriver mais j ai commencé à tirer des leçons merci pour encore une fois de plus. Que le bonne dieu protéger à tous les émigrés barke seydina Mohamed psl.
Bilahi tu as raison mon frère nous sommes fatigue
Moy lolou koi
Que Halla accepte vos prières
Je ne suis pas ď accord avec toi j suis comme vous mon Premier voyage au senegal jai 50€ dans ma poche ma familia ma recibió con corazón mes amies también l
Ma challah deug rek gafi wax. Sama serign modou modou mome bousi dè dem adiana.
اللهم بارك الله فيكم
Vraiment mon grd j'ai même pleurer c'est une vérité absolue
Machallah grand bi degue rék nga wakh
OK sama gayii denioo sonneuh wallah,
Mé yallah naniou yallah démbalé ,té soutourall niou,
Wallah nous sommes très mars...
Amine amine merci mn grand
Merci gour yalla
Merci m'on frère bilaye tu as raison
Akay deugg.Dieureudieuf wayy sama serigne.
Pire verité mal au coeur courage que dieu nous garde
Amine yarabin !
Grazie fratello è la verità
Abdoulaye Ndiaye
almalik
My borhter nice video so much for your only family
merci merci merci
Modou Sénégal merci 🙏🙏🙏
Sama wadji linga wakh lep deugela mai naniou sant yalla te bayi diambat
Sans compter les parents que tu aides et qui n'attendent que ta chute ou ton échec. Nagnou YALLA soutoural rek
Gracias amigo
Cheik Tiguilou Amine way
Cheik Tiguilou pure vérité
c' est vrai cheikh
Amena wahdie lep degela
Du courage a vous * Modou Modou* *keep working you will see the benefits of hard work..
God bless all Modou Modou...
Machalah c touchant
Machalla amna solo sélal rék
Ndaysann niomla gueneuu yeureumm Modou Modou noble la ndah noble weisouwoul lo liguey diohko nit gni niou leik wayei yalnalenn yalla taxawou
Merci Fall yalla nala yalla Faye
Laahilaaa moussu ma degue thi samay nopp deug bou pire niii, merci sa way wathie ghafi
Mchll deug le❤❤
Defa lerr billahii 👌👌👌
Saway ya bakh linga wakh reyna
Wakhi modou modou fen rek la ñouy def Bilahi Amou ñou gat fen khale you Djiegeune wi rek
Grazie mille fratello sii Vero
Yalla na gnou allah soutoural tch barké sidina Mohamed psl
machallah liga wakh lèpe deuge le mais nane sante yalla ko sa nione yaye mayè wayè kène dou la may tèn bagna khawi sono sotoura ndakh nièpe sono waye nite niè thi sotoura lan rawantè
Merci grand contana si yaw deugue rek nga Wakh
Courage bro k Dieu vs garde é vs donne bcp d succès vrema
Bilay manmi à l'âge de 23 mais leknagne sama plus de 23 millions de FCFA ci ay thiakhan
Merci beaucoup SÉNÉGAL
Tu à bien dit dieuredief yalla n'a yalla fay
Merci grand tu as tout dit
Wolaay waxga Deggeu bouwer yalnagnou yalla soutoural
Bilayhii wakh gua deugue 👍🏿🤚
Nice bonne continuation
Ndayesan yalla nalén yalla sotourall
so wax ra faite na lolo merci grand
Wadji limou wakh kouko wéddi rek nafekh gua parceque lep deugueleu! Mane mi meun nani nékone nako ci ay jamono wayé sounou deuk bi beurina gno xamné cou ame xaliss rek lagnouy respecté mom lagnouy faalé lep ci kaw interet.
Natou la me yalla bakh na courage
Bilahi sama wadji contanena si yeuww trep sah. Liga wax lep deugeu la
haaa ah bon de rek monu teré dem adiana Amine
Tres jolis
Bilay contane na si yaw kou dégue deugue rek beuseul j'aime way
grazie fratello
Es verdad hermano. Que dios os ayude . Animo .
Merci bcp amna sola loll machaala
cheikh zinho diop mm,
Merci limasi kham moy deflo man wakh loman botade nelaw bilahi
FAllou Diop bilay wakhal de def lo man dai wakh lo man
Lou lere gua wax
grazie fratello vero
Dieureu dieuf mourit
👏👏👏👏👏👏👍👍👍👍👍👍👍👏👏👏
Macha allah grand sa wakh raffaitna
Grazie mille fratello vero
Hai ragione davvero
Bilaye deuguela
Merci mon frère sa ira
Yalla na léne yalla takha wou👏👏
Merci beaucoup
Ndeyssan ! Toyna khôl.
👍👏👏👏📹📹
Veramente frattello mio sei bravo
billahi tu as parfaitemen raison
Ali Ali santal yalla yalla rek mofinek
diadieuf diadieuf
Merci bcq amna solo mashallah
Guins nathi samabop dall bilahi sabuma yobante thila sama khol di sede walahi azime
Super grand frère
Merci lou ler ka wakh dee
what video is he talking about?
Tu as parfaitement raison grand frère
Kou nagnou bayi wakhedji Lepe yalla la kene yorifi kene yalla mo yore gnepp
Merci tu as dit que la vérité
Machallah amna solou loool way
Bilahi deug pirr ga wax déh mane déh sama borom keur modou modou la wayé mane déh fék magui and ak sama xél ma diko diapalé unchalah ndakh dagnouy sacrifier sén bop ndakh gnounn
Vous avez bien dit c'est la verrité
Bilahi linga wax mo am yalnala yalla faye
Bilahi wakhenga deugue
Aicha Achia c'est vrai deh parcque au Sénégal il croit que nous les modou ont ramasse de largent mais ils se trompe mon argent à part ma mere et mes soeurs je donne personnes à mon argent
Modou modou thi bopam moye diambar mais c est le Sénégal qui est ainsi une fois que nguaye débrouiller di fadje sohlayi danioulaye nenguedjie dounioula maye darra té so démè ba meunoto gniepe alaye bayi même saye propre mbok motah legui kenne kou neque hamal sa bopp du courage vive les immigrés vive kepe kouye gorgorlou birr ak biti
Vraiment
Doy na war dai me yalla bakhna
Ces dure hermano wayé sant yalla du courage
Message intéressant!!!