Ohhhh la réplique du public dans cette chanson me donne vraiment des frissons. "Doolé dji ci biir mbeggel, kenn meunouko teyé, bou xaassé diok, diaaam dieeekh naaaah, Lou nieuw daaal, séeetal"🤗😍😍😍
Man bayiina nite pour youssou ndour, nguir yalla youssou man amna 50ans nguir yalla bayile macky salle, yaaw macky salle manoula jiokh lo amoule, dañio yaga ak yaaw beug la dila ndamo fii sii Europa 🇸🇳🦁👈❤❤🙏🙏👏👏✊
Sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé , sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé.... Diaaye dolé bakhoul ak thi loumou meuneu done , deukeundo fonkeul sét thi yalla miniou Môme Ana diambaar you mak yi Borom alal you barré Borom kham kham you reuy Né kéneu nékatoufi Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy Diaaaye dolé bakhoul ak thi loumou meuneu done Tay meun nga bakhlé euleuk nga dadi yakhoulé ... Boul nawo sa dolé Batakh nga gaawa lalé Kou yékssi nang ko falé Té nga Sakho Di balé Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy Ni mandoul té rafétal sa nékine Yaw dél ballé bania wané sa dolé Boul dieul yaw sa dolé khal diko khékhé Sa dolé dimbali si diame gni Diaaye dolé bakhoul ak thi loumou meuneu done Boul kagne sa doléy ba diko titeuro Bissa ngui thi biss yi Té faw biss bi yékssi Niou dadialé yaw sa dieuf yi Nga kham ni yalla mingui fi Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy Mandoul té rafétal sa nékine Yaw dél ballé bania wané sa dolé Boul dieul yaw sa dolé khal diko khékhé Sa dolé dimbali thi diam gni Fass wa dafa naagou ni mbam ma Mala geuneu gaaw Boy daw dangay yéékh Té man damay gaaw Fass wa Di ndieukeuntou Ba farr dougou thia téén ba Boudoul wonak mbam ma Fass wa déss thia téén ba Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy Ni mandoul té rafétal sa nékine Yaw dél ballé bania wané sa dolé Boul dieul yaw sa dolé khal diko khékhé Sa dolé dimbali thi diam gni Sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé Diaaye dolé sakh woroul Ndakh kéneu khamoul foye moudié 🎵🎶🎶🎶🎹🎵🎸🎺🎷 Diaaye dolé sakh woroul ndakh kéneu khamoul foye moudié waaw Boul naagou thi sa am am Adouna meun nala ndiouye Am aaam ak meun meun deukoul féneu Wayé dolé dji thi biir mbeuguél ❤️ Kéne meunoukoooo téyé Bou khassé diok Diameu diéeekh neuuuuu🥺🥺🥺 Lou nieuw mou dane sétal Solé dji thi biir mbeuguél , kéne meunoukoooo téyé bou khassé diok diameu diékh neuuuuu lou nieuw mou dane sétal Lithi djik mbeuguél ❤️ Djigou thi lénén Mbeuguél bou wooor Wané dolé ko djik Bouko défoul ba seeeytaaaaané dougou thia sétal ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Yaye séné baay yaye séné baye yaye séne baye 🤗🤗🤗☺️☺️☺️
Ohhhh la réplique du public dans cette chanson me donne vraiment des frissons. "Doolé dji ci biir mbeggel, kenn meunouko teyé, bou xaassé diok, diaaam dieeekh naaaah, Lou nieuw daaal, séeetal"🤗😍😍😍
Walay
Man bayiina nite pour youssou ndour, nguir yalla youssou man amna 50ans nguir yalla bayile macky salle, yaaw macky salle manoula jiokh lo amoule, dañio yaga ak yaaw beug la dila ndamo fii sii Europa 🇸🇳🦁👈❤❤🙏🙏👏👏✊
day ligéeyal reewam
Walay ndeysane
J'y étais .vraiment c'était magnifique 🇸🇳💪🏻 yaye sén baye
Premiére comentaire
Sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé , sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé....
Diaaye dolé bakhoul ak thi loumou meuneu done , deukeundo fonkeul sét thi yalla miniou Môme
Ana diambaar you mak yi
Borom alal you barré
Borom kham kham you reuy
Né kéneu nékatoufi
Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy
Diaaaye dolé bakhoul ak thi loumou meuneu done
Tay meun nga bakhlé euleuk nga dadi yakhoulé ...
Boul nawo sa dolé
Batakh nga gaawa lalé
Kou yékssi nang ko falé
Té nga Sakho Di balé
Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy
Ni mandoul té rafétal sa nékine
Yaw dél ballé bania wané sa dolé
Boul dieul yaw sa dolé khal diko khékhé
Sa dolé dimbali si diame gni
Diaaye dolé bakhoul ak thi loumou meuneu done
Boul kagne sa doléy ba diko titeuro
Bissa ngui thi biss yi
Té faw biss bi yékssi
Niou dadialé yaw sa dieuf yi
Nga kham ni yalla mingui fi
Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy
Mandoul té rafétal sa nékine
Yaw dél ballé bania wané sa dolé
Boul dieul yaw sa dolé khal diko khékhé
Sa dolé dimbali thi diam gni
Fass wa dafa naagou ni mbam ma Mala geuneu gaaw
Boy daw dangay yéékh
Té man damay gaaw
Fass wa Di ndieukeuntou
Ba farr dougou thia téén ba
Boudoul wonak mbam ma
Fass wa déss thia téén ba
Annnnnnnhhhhh dolé dou wéy
Ni mandoul té rafétal sa nékine
Yaw dél ballé bania wané sa dolé
Boul dieul yaw sa dolé khal diko khékhé
Sa dolé dimbali thi diam gni
Sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé sa dolé sa dolé sa dolé boul ko khékhé
Diaaye dolé sakh woroul
Ndakh kéneu khamoul foye moudié
🎵🎶🎶🎶🎹🎵🎸🎺🎷
Diaaye dolé sakh woroul ndakh kéneu khamoul foye moudié waaw
Boul naagou thi sa am am
Adouna meun nala ndiouye
Am aaam ak meun meun deukoul féneu
Wayé dolé dji thi biir mbeuguél ❤️
Kéne meunoukoooo téyé
Bou khassé diok
Diameu diéeekh neuuuuu🥺🥺🥺
Lou nieuw mou dane sétal
Solé dji thi biir mbeuguél , kéne meunoukoooo téyé bou khassé diok diameu diékh neuuuuu lou nieuw mou dane sétal
Lithi djik mbeuguél ❤️
Djigou thi lénén
Mbeuguél bou wooor
Wané dolé ko djik
Bouko défoul ba seeeytaaaaané dougou thia sétal
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yaye séné baay yaye séné baye yaye séne baye 🤗🤗🤗☺️☺️☺️
The king 👑❤️
sama papa way ❤️❤️❤️💪🎤
Super 💞 you Doundeul
Youssou camara. Et la grosse caisse. 4 coups successifs....du talent
Salut c'est pas youssou camara dh oubien c'est lui...?
@serignekharndiaye5614 allez vérifier
Machalla
Oui youssou camara avait la batterie. Ça ce sent sur la grosse caisse et les timbales
La batterie c'est ablaye lo