Merci maître .vraiment koula degglou attentivement ligua wakh c'est très clair . Dossier bi ya anguille sous roche. Li guènè nabou leye dou nène way .erreur amna au niveau de la justice c'est clair. Un tel dossier avec un double meurtre, mandat de dépôt même pas 6 mois mouy âme liberté provisoire dafa yomb torop.
Dafa mel ni Sénégal nieupou ay magistrat la niou vous ne connaissez rien sur ce dossier et guéne beugue wakh lénéne procureur bou diapou transfert dossier au juge d'instruction ensemble niou libéré l'une et maître amoul béna loi bou wakh ni liberté provisoire waroul âme avant enquête doko indi pcq amoul ce double meurtre là képou kousi coupable il sera jugé paix à son âme les deux victimes mais maître wakho fi dara nakh pcq indi wo bena loi bouy contre dire li juge d'instruction def
Merci mettre de nous confirmer qu'on avait raison de fustiger cette libération inattendue. Pape ndiaye walf ak gadiaga yikay plaidel doivent être sanctionnés
❤❤❤ machalla Masour Diop et Akhemet Aidara longue vie kheweule you bari machalla allekhamdoulila a toutes léquipes machalla Masour Diop yallana yalla defalela diame namonenalou Diop santebi rek mo nékhoule ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Justice pour les défunts 😢 fek la sa bir keur ray la togne gnari yonne li métina, té lima diakhal moy dossier bou amoul juge kane mo libéré ? Mystère et bulle de gomme 😢
Nandou leye Ken warouko libéré 😢😢aziz dabala ak waly balde yalla nalen yalla yeram😢😢😢yalla na yalla atte nabou laye ak abdou aziz dabala ak wally balde😢😢😢
C'est trop facile de faire un acte aussi grave et d'être libre de vivre tranquillement. Non , nous prions que le seigneur rends sa justice divine , Amineeeee 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😡😡😡😡😡😡
Machallah vérité absolue ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤deugue leu Yalla beugue. Nagniou khalate niétifanou babel tey até deugue ndakh loufi waye até Yalla dinako até wate kone nagniou si set Yalla té ragalko
Markhabane maître, Je vois juste en vous une personne intègre ( dans ce monde fou, cruel et hypocrite que nous vivons goor tiguiii yomboul). Nous avons parfaitement confiance en vous d'après votre intervention on peut compter sur vous ma cha Allah). Qu'allah swt vous fortifie afin que vous puissiez accomplir votre sacerdoce convenablement inshaallah rabi. Suis dégoutée carrément par la justice sénégalaise 😢😢😢
En tt cas j avais entendu un marabout du nom de Mohamed badiane disant que Nabou leye sera libérer et quitterai le pays Et le dossier va finir par vengeance et d autres meurtres et d autres personnes seront arrêté encore Alors actuellement Nabou est libre et à sorti le pays et ses nombreuses conférences de presse aussi khégnoul lou nekh donc lou way di wakh nay lerr
C'est trop facile dans un dossier pareil de meurtre. Que quelqu'un en tant que complice de meurtre de près où de loin . Et qu'elle soit libéré mais dans quel conditions. Nous réclamons justice pour Aziz Ba et Wally. 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😡😡😡😡😡
Gni di contredire avocat bi khana danio am problème compréhension ? Lou lerr nagn leu wakh, juge remplaçant bou amoul expérience jugement moko guené té oubegouniou dossier ngene nane lane. Il dit bien que lolou meunoul am si 1 an ou 2 donc enquête bi sakh au fond commencer goul
Maitre yalla rek mo la mouna fay thi barké Aldiouma ji.cest comme si Abdoul Aziz Ba et Boubacar Gano étaient mes frères de meme sang. Et Waly qui vient repondre par surprise a une mort atroce.massah yalla na len Bourbi yeureum té yekhegnou.
Mais pourquoi la famille de Aziz wara diél avocat ? État nako diélale avocat.sudé domou un soi-disant haut personnalité Kone dou démé gni. Louway até fi dinko atté wate le jour du jugement dernier 🗡️🔥
Eureur amou fi pasque gniome gnio tanne nék juge konne na ka bi lérr si nop nityi waw Nabou léy waroull déf todj todj bi bas paré bougue guéne si nii noooo défa yonbou tropp na délouwatt si kasso bi gnioune lolou mogniou nékh baaa gniou jugée ko.boba lougniou ame diéll gniou khamni lolou la yalla doguall magui dépuis Mauritanie déma yeureum wally ak aziz billay wallaye ndeysane parégouma dioy ba téy 😭😭😭😭😭
Bravo duo Ameth et Mansour tout le monde est content
Merci maître .vraiment koula degglou attentivement ligua wakh c'est très clair . Dossier bi ya anguille sous roche. Li guènè nabou leye dou nène way .erreur amna au niveau de la justice c'est clair. Un tel dossier avec un double meurtre, mandat de dépôt même pas 6 mois mouy âme liberté provisoire dafa yomb torop.
Dafa mel ni Sénégal nieupou ay magistrat la niou vous ne connaissez rien sur ce dossier et guéne beugue wakh lénéne procureur bou diapou transfert dossier au juge d'instruction ensemble niou libéré l'une et maître amoul béna loi bou wakh ni liberté provisoire waroul âme avant enquête doko indi pcq amoul ce double meurtre là képou kousi coupable il sera jugé paix à son âme les deux victimes mais maître wakho fi dara nakh pcq indi wo bena loi bouy contre dire li juge d'instruction def
Trop
Corruption peut-être mettre l'argent sur la table 2 ou 4 millions c'est possible ?
L'argent peut acheter la liberté je suis désolée 😢
Mistiques mo Bari ci dossier bi
@@AissatouWade-z2n mystique faw mou âme si deh tu penses les parties sene famille da niouy took di xolé rk
Merci mettre de nous confirmer qu'on avait raison de fustiger cette libération inattendue. Pape ndiaye walf ak gadiaga yikay plaidel doivent être sanctionnés
Pour l'amour du prophète Mohammad ﷺ dit Alhamdoulillah ❤🎉
Alhamdoulilah ❤❤❤ salal lahou Ala mouhamad
Al Hamdoullillah
Alhamdoulilah
Alhamdoulilah
Alhamdoulilah
Merci ahmed et mansour khady Barro vous aimes depuis Belgique
Merci maître dieu vous le rendra
Amiiine inchallah 🙏
Bravo Maitre Ba ❤❤❤que Dieu vous protège justice pour Abdou Aziz Ba et Boubacar Gano paix a leurs âmes 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Franchement merci Maître Justice pour Aziz et Wally
Boy dehlou li gay deglou mais pas ay dof youy live du wah du n’importe quoi merci encore
@@ZEYNAFAYE-gh6pw niom kouléni déglou diga bakarou
@@ZEYNAFAYE-gh6pwCOMME PAPE NDIAYE AK CHEIKH MBAKE GADIAGA.
❤❤❤ machalla Masour Diop et Akhemet Aidara longue vie kheweule you bari machalla allekhamdoulila a toutes léquipes machalla Masour Diop yallana yalla defalela diame namonenalou Diop santebi rek mo nékhoule ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ay way son excellence wakhal si li!senegal amoul loi,yalnalene yalla yeureum li dafa yomb trope
Surtout la façon dont ils sont morts la sanction doit être retentissant dans le monde 😢
@@adjaratougning2957Vraiment sanction bou atroce laniou mérité
Tu es vraiment un grand monsieur courage
Machallah Maître
Justice pour Aziz et Wally
Vraiment yone amoul senegal 😢
Maître Khoureychi ba un grand monsieur
Chapeau Ameth Aidara et à toute l'équipe 2A TV et merci maître wax dji leerna Machalla
c'est du jamais vu ce qu'ils ont fait mais les coupables paieront tôt ou tard.
Justice pour les défunts 😢 fek la sa bir keur ray la togne gnari yonne li métina, té lima diakhal moy dossier bou amoul juge kane mo libéré ? Mystère et bulle de gomme 😢
Un juge inexpérimenté jeune pr un dossier lourd c la 1ère erreure il ft un juge expérimenté un double meurtre barbare 😢😢
Wallay ndeysan 🙏
Nandou leye Ken warouko libéré 😢😢aziz dabala ak waly balde yalla nalen yalla yeram😢😢😢yalla na yalla atte nabou laye ak abdou aziz dabala ak wally balde😢😢😢
Vraiment dou yone yomb na trop double meurtre entouca doyna warr nabou léye el n doit pas être libre comme ça
Vraiment 🙏
Merci beaucoup maître
C'est trop facile de faire un acte aussi grave et d'être libre de vivre tranquillement. Non , nous prions que le seigneur rends sa justice divine , Amineeeee 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😡😡😡😡😡😡
Namonagn duo bi😊
Nabou Leye doit retourner en prison s il y a justice au sénégal!
Nous nous adressons à l etat du sénégal.
Vraiment lii dafa niaw justice pour Aziz AK wally
Si la vengeance en cours de téléchargement 🗡️🗡️
Zahir wala batine.
Yombou na trop te niaw
Mashallah a respectable man thank you for fighting for justice. Justice for Aziz et Wally!
Machallah vérité absolue ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤deugue leu Yalla beugue. Nagniou khalate niétifanou babel tey até deugue ndakh loufi waye até Yalla dinako até wate kone nagniou si set Yalla té ragalko
Machala machala rék bilaye walaye sama khole dafa méti trop ♥️ yalla na yalla yereume ci barké seydina Mohamed Amine yarabine 🤲🙏
Bravo Maitre ❤
Un avocat très pausé gentil sérieux et humain
Dafa Ragal yallah sunu borom motakh.
Vraiment président diomaye justice bi ak l'intérieur migui lay échappé dank dank 😢😢
Bravom maitre ba ❤❤❤
Bonjour... Ameth vous êtes les meilleurs je vous aime 2A TV ❤
Justice pour aziz et wally vrement merciii maitre ❤
Le jour où la vérité éclatera ça sera historique sur tout l'étendue du territoire sénégalais.
Bravo maître, que justice soit faite !
Well said Mr Bah knowledge and time shall guide you Inshaa Allah
Diadieuf seydi ba🎉
Bravo maître merci beaucoup 😘😘
Merci maître li kin waroko bayi nono
Merci beaucoup mètre yallanallayallamayindame❤❤❤❤❤
Amiiine inchallah 🙏
Vraiment Doyna warr bilahi,faut aimé cs famille là maitre.mrci mr le maire et son ami mansour diop d’avoir interrogé maître.
Merci Maitre❤❤❤
Maître vraiment tu as raison dh 😮
❤❤Juge bou libéré NABOU duna teude peine bu. Yabéwouléine Nonou Sénégalais yu.double Neuttre ❤❤
Maître un Grand Merci à vous. Merci aussi à Ahmed et El hadj
❤❤Maitre tout le Sénégal est derrier toi lu na lerr.daffa yonme trop❤❤
ماشاءالله بارك الله فيكم شكرا لكم جميعا
Maître il a bien parlé merci
Justice pour aziz et wally
Me Khoureyshi ba ..un tres grand avocat..je l ai connu de loin nak..depuis bi niou arreter me abdoulaye Wade.. amoul thiakhann
Konn tamiitt famille bi naniou andd ak dall touti Rek l pp dîna Lair inshala naniou toppou avocat bi rek
Bonne continuation les deux frères que Dieu vous protège 🙏❤❤❤
Salam salam lii dafa yoobou raay nitte gueneu dii mbeulée aî mbokam Sénégal gui ama guel yoone
Merci beaucoup justice pour Aziz AK wally
Justice bi bilay dina béteu askan wi
Tous les senegalais sont choqués
Markhabane maître,
Je vois juste en vous une personne intègre ( dans ce monde fou, cruel et hypocrite que nous vivons goor tiguiii yomboul). Nous avons parfaitement confiance en vous d'après votre intervention on peut compter sur vous ma cha Allah). Qu'allah swt vous fortifie afin que vous puissiez accomplir votre sacerdoce convenablement inshaallah rabi. Suis dégoutée carrément par la justice sénégalaise 😢😢😢
Paré na Sénégal. Pays sans justice, du n’importe quoi.
Non kay ken hamoul lanla
En tt cas j avais entendu un marabout du nom de Mohamed badiane disant que Nabou leye sera libérer et quitterai le pays
Et le dossier va finir par vengeance et d autres meurtres et d autres personnes seront arrêté encore
Alors actuellement Nabou est libre et à sorti le pays et ses nombreuses conférences de presse aussi khégnoul lou nekh donc lou way di wakh nay lerr
Thank you Maitre ❤❤❤
Merci beaucoup ❤❤❤
Vous ête noble maître
MachaAllah
Justice pour azize BA et boubakar gano ❤❤❤
Cheikh Gadjiaga dagneko wara porté plainte diffamation le déff deug thi Azize
Merci maître Bâ ❤❤🎉
Mouhamed mansour et Ahmed aidera dzmalén beugue Bilay le duo pertinent
Merci hamed et mansour nous voulons justice pour Aziz et wally justice justice justice
C'est trop facile dans un dossier pareil de meurtre. Que quelqu'un en tant que complice de meurtre de près où de loin . Et qu'elle soit libéré mais dans quel conditions. Nous réclamons justice pour Aziz Ba et Wally. 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😡😡😡😡😡
Wa li nekhna dh ❤
Gni di contredire avocat bi khana danio am problème compréhension ? Lou lerr nagn leu wakh, juge remplaçant bou amoul expérience jugement moko guené té oubegouniou dossier ngene nane lane. Il dit bien que lolou meunoul am si 1 an ou 2 donc enquête bi sakh au fond commencer goul
❤ machallah vous êtes adorables
Serigne massour ak Ahmed aidara magui lene di nianal djam djou barre barri ❤❤ sama niari sope yi depuis sene tv yene rek laye topppppp❤
Le duo magique 😂😂😂
Aziz môme ndiepe la daimale ngui metti
Ahmed et mansour yalla nalén yalla saam maylén wer ak goudou fan
Lidafa wara lére bilay Walay Nabou leye douyone nioukoy bayi nonou 👿
Machalla machalla maître
Maitre yalla rek mo la mouna fay thi barké Aldiouma ji.cest comme si Abdoul Aziz Ba et Boubacar Gano étaient mes frères de meme sang. Et Waly qui vient repondre par surprise a une mort atroce.massah yalla na len Bourbi yeureum té yekhegnou.
Libération mystique
Machalla ❤❤❤🎉🎉🎉Maître merci 🙏🏻
Tres bonne avocat merci ❤❤
Me un très grand procédurier té gueum yalla ❤❤❤longue vie.
Lou khana mystique la😢
Mystique deugeu la
Alhamdoulila 🙏
Justice pour Aziz Dabala et Wally ❤❤❤❤
Mansour yaw ak Ahmed je vous remercie dema Léna pegue
Justice pour Aziz et Bouba!
Bravo maître tu as bien parlé
Mais pourquoi la famille de Aziz wara diél avocat ?
État nako diélale avocat.sudé domou un soi-disant haut personnalité Kone dou démé gni.
Louway até fi dinko atté wate le jour du jugement dernier 🗡️🔥
Merci Maître 😊
Ahmed Aïdara et son equipe doivent invité en contrepartie l'avocat de Nabou Leye pour que nous ecoutions l'autre version.
yalna bougnou serithiou maitre bi sax bilahi foguena xamolenenè yalla amna
Eureur amou fi pasque gniome gnio tanne nék juge konne na ka bi lérr si nop nityi waw Nabou léy waroull déf todj todj bi bas paré bougue guéne si nii noooo défa yonbou tropp na délouwatt si kasso bi gnioune lolou mogniou nékh baaa gniou jugée ko.boba lougniou ame diéll gniou khamni lolou la yalla doguall magui dépuis Mauritanie déma yeureum wally ak aziz billay wallaye ndeysane parégouma dioy ba téy 😭😭😭😭😭
Justice for aziz and wally ❤❤❤
Merci maitre ❤❤❤❤
Svp xana 2atv amoul si bouké canal bi sama yaye daflén beug di sétane si télé bi svp ku xam sén fréquence baxé merci🙏🙏🙏
Mâcha Allah fofou noyna
Maître deffal te yalla takh guir yalla daffa meti waye
Li dal ba foumouy moudiou c un dossier d’état Amna ponkal boussi impliquer niou beug ettoufer cas bi
Bamu sotie
Merci bcp
Wallahi 😢😢