Beignets à la Sénégalaise
HTML-код
- Опубликовано: 9 фев 2025
- Recepe for Senegalese beignets/ recette beignet Senegal
flour 3.5 cups / farine 500g
Orange zest to taste/ zeste d’orange
Lemon zest to taste/ zeste d’un citron
Lime zest / zest d’un citron vert
1/2 cup Milk powder/ lait en poudre 85g
1/2 cup Evaporated milk/ lait évaporé
Salt/ sel
Vanilla
Orange blossom water( optional)/fleur d’orange
Shredded coconut/ coco râpé
Nutmeg/ muscade
4 Eggs/ œufs
3.53 oz Butter (melted)/ beurre 100g
Raisins
1.5 cups of Sugar or sweetener of your choice/ sucre 353 g or to taste
Oil for frying
2 tsp Active dry yeast/ 1 sachet de levure boulangère
1 tsp Baking powder/ 1 cac levûre chimique
Bon Appétit 😘!!!!
Welcome to Chez Billo! Bienvenue sur la Chaine Chez Billo.
Passionnée de cuisine Sokhna Billo est la présentatrice de l'émission "Berndé ak Sokhna Billo" sur Bichri TV Internationale, depuis plus d'un an et depuis. En marge de cette émission, Chez Billo a été crée pour vous apporter beaucoup de tutoriels sur des plats inédits en mettant l'accent sur un régime alimentaire appelé "régime cétogène" particulièrement pour ses bienfaits sur notre santé!
Quelques notes sur le régime cétogène!
Le régime cétogène est un régime riche en lipides particulièrement à la mode depuis quelques années. Pourtant, il est utilisé depuis près de cent ans pour soigner certaines pathologies, dont l'épilepsie. Ce régime vise à réduire considérablement la consommation de glucides au profit des lipides pour provoquer un état de cétose. Au delà de la perte de poids importante, il aurait de nombreux bienfaits pour la santé.
Caractéristiques du régime cétogène :
Consommation très importante de lipides (75 % des apports)
Apport en protéines inchangé
Réduction considérable des apports en glucides
Entraîne des symptômes désagréables les premières semaines (grippe cétogène)
Perte de poids rapide
L'état de cétose aurait de nombreux bienfaits santé (regain d'énergie, protection contre certaines pathologies, etc.)
Masha Allah sister beignets sama kharite nguay am fofou masha Allah na ress ak diama 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😋😋😋😋😋😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Amine sis di la ziar bou weer dc yaw ak Mustafa manguen def nonu la ci Mel momit🙏🏾😘💕
Merci bcp mais une recette de plateau sucré salé pour nos fêtes d'anniversaire svp svp svp urgent
Machalla SOKHENA billo nice na
Toure Diarra akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Ooh j adore . Machala comme d habitude nexna. Merci encore
gamer 123 Akassa jajeuf 🙏🏾😘
Macha Allah !!! Amna solo lole té ninoul aussi. Macha Allah Sokhna Billo
Tt à fait ma chérie loolu mima ci neex 🙏🏾😘
Machallah beignets amna maana nako essayer merci bcp
In Sha Allah ma cherie ngacwane gniu sa version 🙏🏾😘
Machalla sokhna billo beignet bi rèfètna surtout les conseils amna solo yalla fèyla laf thiat 👍👏👏👏💕😘
Amine ma chérie gnou bok lep feke ak tal🙏🏾😘
Ah Ma Sha Allah Sokhna Billo😘
Jajeuf ma.cherie😂😘
Humm Sokhna Billo beignets yi rafetna gnou mashaAllah, do na ko essayer inchaAllah merçi
Jajeuf ma cherie nga wan gnou fi nga guene aussi so ko defare🙏🏾😘
Macha allah sokhna billo ay bénie you am diom selle na te khamna nekhna yalla goudal fanbi wereul thieur yi barke chekhoul khadime
Amine yallah defal ngouko gnoun niep dila sabt bou weer ci kaddu you rafet yi jajeuf🙏🏾😘
beignet bi nekhna machalah
Lolu de la gnou waax 🙏🏾😘
Tata billo beignets yi nirou ak lou nekh dei, machalah mane mom beignet yi dinako defar inchalah merci vraimnt si conseil yi aussi car tres importnt aussi
Akassa ma cherie waax ma nounou deme soko essayer ndaax jajeuf ma. chérie 🙏🏾😘
Assallamallikoume machallah amna solo dieureudieufati nio gui lay begue funu tol.
Fi de la euppe ma cherie dilene sant bou weer 🙏🏾😘
Salam tata billo❤❤❤❤
Look so yummy 😋 I will try it incha Allah
I was indeed.let us know how it went and we would love to c yours whenever u get a chance to make it 🙏🏾😘
Beignets bii inchalla dinako defaar pour 18safar . Yallana yala faye. Longue vie à toi santé et Amour......
ibrahima kebe amine yaram à toi de même bou gnou fatente ci nian 🙏🏾❤️
😂😂 seugne Ibrahima kebé sama khel si yaw la nak bima gisey tutoo bi
@@khadykane3828 waa guisnga sama beignetla dh... dama begue beignet
Machalah contanena
Fi deh la euppe ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Testé et approuvé tata Billo c'est troooop 😋
Alhamdulillah ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Merci tata leralyi amna solo merci
Akassa ma cherie faw gnouye layente biir jajeuf 🙏🏾😘
Merci bcp maman Billo Machallah yalla nala yalla fayy
Amine ma chérie gnou bok lep feke ak tal🙏🏾😘
Merci Tata billo pour cette recette je dirais au talibé de touba toute de faire beaucoup de prières pour toi🙏 sama beignetla mane rek keen bokoussi
ibrahima kebe wawaw yaw rek dila sant bou weer jajeuf 🙏🏾❤️
@@ChezBillo merci Alhamdoulilah ils seront troo content de toi ... magal gui dina beignet comm tout monde inchalla ...
J essayé hier ils sont excellents merci billo adiarama 👍
Alhamdulillah ma cherie. Je ne suis pas trop beignets mais bi mome j’en raffole tt le tps surtout mes enfants. Dila ziar bou weerr🙏🏾😘
@@ChezBillo albarka👍
Machahlla Tata
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Masha-Allah Sokhna Billo niaak la ame woroule santé santé👍🏽👏🏼👏🏼👏🏼🙏🏽🙏🏽🙏🏽💚💜❤️
Jajeuf yaram guiss nga de famille chez Billo xetu baax yi la gnouye def de mais aussi sa chaîne bi na Sha Allah aye deug rek nguene Faye waax di ye sénégalais yi surtt gnoun gni nek bitim reew leg eggs yen yi deg tek nga ci am doko gueum mais sa kaw sa kanam 😍❤️🙏🏾😘
Beignets machallah gnigui khar bou farine de coco bi
Inshallah ma cherie 🙏🏾😘
Maane yaaye sama idole
J'ai essayé de reprendre la recette ...
Macha allah tata Billo MERCI
Je t'enverrai les photos sur Facebook incha allah
In Sha Allah dinala neex loolu comme ça ma guiss sen création aussi sant nanou lolu ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Machallah tata defatigua sa meunin d
Jajeuf ma cherie sant nagnoula 🙏🏾😘
Ah nekh n'a manchallah yalla yocou la té barckél la
Amine gnou bok lep feke ak tal🙏🏾😘
Machallah encore sokhna billo dina bakh thi ndeki wala goûter école lol merci
Effectivement man dama lene di joox beignet comme dessert ou bien so yakamte le matin meun ngako bole ak sa cafe wala lait 🙏🏾😘
@@ChezBillo mom kay bamako defarer yagoufi lol nieup si yobaler machallah nekhone na trop merci
Machallah choukrane 🙏
sokhna drame akassa jajeuf 🙏🏾😘
J'aime ♥
Akassa ma cherie 🥰🙏🏾😘
Bilaye sokhna billo kéneu dou yaw diangatena bénéne astuce tey .
Mangui soga kham loutakh souma défar beignets bou am raisin mouye feuleu si kaw 😳😳👍👍dieureudieuf benzène yone niga wakh laye déf diarama 👍🙏😍😘yokoul va yeuk ko
Amine ma chérie layente biir rek lagnoufi am.
Alhamdulillah ci jangatbi 🙏🏾😘
Machallah tata
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Beignets yi ame nagnou teint tarkallah
Mberry Mmy akassa sis raye ngama 😂😂😂
M achallah yalla ngafi yague weer bah gna lol si societibi
Amine ma chérie yena baax rek, dilene sant boy weer ci tewlubi 🙏🏾😘
It is good to mention the side effects of nugmet. Thank you.
Ur most welcome my dear cause it looks like that lots of people do not know it at all🙏🏾😘
Merci beaucoup
Rokhaya Gaye c tjrs avec plaisir ma chérie dila ziar bou weer🙏🏾😘
Farine de coco la wala blé? Machallah Nice na lol tata
Salaam ma cherie non bo farine de blé la 🙏🏾😘
Machalah ❤️
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Machalla mais est-ce que meuna xam tourou kurel bii si montage bii
Donuts maman gnikoy khar bou farine de blé bi
Waw souko tps bi maye rek inshallah ma cherie 🙏🏾😘
Bonsoir ma sœur merci beaucoup je vais faire cette recette de beignet c'est comme moi j'aime pas quand y'a beaucoup de sucre merci acord ma sœur.
Elisabeth Gomis akassa ma cherie c une recette q j’aime bcp 🙏🏾😘
Beignets daal beurina tė bokoul wayė beignets yi amna solo
Waw lolu de amna ma chérie jajeuf 🙏🏾😘
Molto bene
Ziar sis 🙏🏾😘
Salam Ta Billo, machala beignet bi nekhna. Combien de temps gua mélanger farine bi cii kitchen Aid? Merci pour tout
Waleikum Salaam ma cherie environ 5 à 10 mins juste le tps sucre bi seyi pâte bi bag à am ben boule de farine bou melangerwul🙏🏾😘
@@ChezBillo Merci bcps. Bonne continuation 😘
Machallah toujour égal a elle même
Akassa ma cherie vraiment merci bcp 🙏🏾😘
Machallah merci bcp àfaire inchallah
Akassa ma cherie nga wangnou sa boss book defare🙏🏾😘
👏🙏👍👍👌😛
😁😛😛🙏
Merci tata ❤️ wallay jdr tata j’aimerais bien de rencontrer un jour
Diattou Sow fi la euppe ma cherie yallah meunako nanou garder contact rek 🙏🏾😘
Chez Billo inchallah tata
J aime dal
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
On pourra les garder pour combien de jours ?
Si tu as de la chance ça peux se conserver pdt presque une semaine s’il fait pas très très chaud sur le comptoir et plus de 2 semaines ds le frigo c tellement bon q si tu ne réserves pas quelques les gens peuvent les finir le meme jour 😂🙏🏾😘
Macha allah
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Pour 3kg on le dose comnt je veux le refaire car dama am birthsday
Ziar sunu frère da ngaye multiplier recette bi par 2.5 kg 🙏🏾❤️
Tata Muscade méré nala torop 🤣 yaako wakh liii yeup
Waw deh beug nako waye faw gnou moytou ko tamit deh sou bare rek mou loolu 😂🙏🏾😘
say video da fa longue trop dekoy guatale merci
Ziar ma cherie gnoune dagnouye aider gni nga xamne amougnou chance bi gnou ame dc su video bi bouder amna option avancer!
La famille chez Billo mome dagnouye inclure gneup ak fou sa niveau tog meuneu t’il, merci
Je crois que les vidéos sont bonnes comme ça pour les amoureuses et amateurs de la cuisine
Merci ma chérie passion dafa garaw tu l’as si bien résumé jajeuf 🙏🏾😘
I like your video but they are too long. Is there a way you can make it shorter. Thanks
Thx a lot dear for tuning in unfortunately chez Billo family welcomes anybody with any cooking level therefore we have to give deatails for those want to learn how to cook from scratch that is the essence of the channel and we also have members who are pationate abour cooking. If I do certain tutorials they tend to be shorter other than that it is what it is.
I appreciate your suggestion and the time you take to watch the channel 🙏🏾😘
Madame je voi plus tes recette new khana daga arretè
C'est bizarre je ne reçoit jamais les notifications pourtant j'ai activé la cloche
Franchement RUclips vous êtes pas sérieux je ne suis pas contente hein bon
Il faut toujours que je vérifie moi mm
Oh désolé ma chérie des si cloche legui j’ai remarqué qu’on te fait choisir une option si tu appuies sur la cloche choisis tout( all) hopefully dingua jot notifications yi.
Sant nagnoula surtout ak effort yi 🙏🏾😘
@@ChezBillo ASALAMOU aleykoum warakhmatoula sokhna billo oui effectivement ils te demandent de choisir 😍 mais n'empêche on te soutient et te suit tous les jours incha Allah dieureudieuf bonne journée bisous 😘😘👍❤
@@ChezBillo sokhna billo j'ai une collègue à qui j'avais suggéré ta chaîne elle aime tout ce que tu fais mais sin problème elle ne comprend wolof et demande de te dire de faire tes vidéos en français de temps en temps où de les sous-titres 😍😍 la plupart c'est moi même qui lui explique en français .
En tout cas merci pour tout que dieu veil sur toi et toute la famille bonne journée bisous
Ah merci ma chérie in Sha Allah c mon next step mais en ce moment j’essaie de trouver une routine qui marche avant d’entamer les sous tirages car ça demande énormément de tps pour le moment mais j’y pense très souvent disa ton collègue de patienter un peu on y arrivera in Sha Allah je sais q c sur des fois moufgnalgnou touti rek, merci our le partagé et la promotion ça me touche énormément 🙏🏾😘💋
@@ChezBillo waw incha Allah je lui dirai dieureudieuf yalana yala souniou borom motali lep té motali sa yéné si ligaye déf mou kawé sa djorte incha Allah 🙏🙏🙏😘😘
Vous pouvez mettre la levure boulangere dans du lait
Eh oui il faudra réchauffer le lait jusqu’à ce q ça soit tiède avant d’y ajouter la levure boulangère 🙏🏾😘
des fois j'aimerai regarder vos vidéos mais elles sont excessivement longues pensez à les couper nguir yalla
Right.
Mais si c 1 kg de farine il faudra 2 oranges,4 mouscades
Ma chérie tt peux utiliser la quantité que tu veux c question de préférence personnelle en peux même omettre ces ingrédients pour les remplacer avec d’autres non donc?🙏🏾😘
Tata do defarer roty guinar
Ziar ma cheri defar nako ci chez billo lien va ngui ni
ruclips.net/video/ucSh9wIV8FA/видео.html
Slu tata chérie guisou mako wone
No problem ma cherie des fois RUclips moye lolu daf maye arriver aussi 🙏🏾😘
Tata chérie CV wa lolou la Kaye mon takh guisa goumako ms tata je t aime bilaye sa numéro soumako meunone âme di na bakh
Ndiaye Astou waw fi de la euppe numéro ba ngui so ci wore rek dinako jot in Sha Allah
Passe une très bonne journée ma cherie🙏🏾😘
+16463859436