Salaam Chef Bilo ma Cherie levure bondèe la 🤣🤣🤣 Masha Allah ma mere l’appeler ainsi Masha Allah sister you’re rock I just loveeeeeee your cooking ❤️❤️❤️😘😘😘😘
Saveurs Planétaires Waleikum Salaam sis Marietou diguama raye man saye expressions benene affaire la😂😂😂🤣!!! Likewise sis laf la thiat ci you baax yi Gaye defar 😘🥰😘😘😘
5 лет назад+2
Chez Billo i called you but it’s a 201 numb maybe you didn’t see it please let me know when is the best time to call u thanks 😘😘😘😘
Machallah yénangui deff liguey bou rafet di diapalé sen rakk yi sen sëy. Tata marietou please invitel Tata billo ci sa wagn one day inchallah . Yalla na suniu borom sameu len
Mya mya ziarnala bou baax.alhamdulillah kon jap len ko fofu rek, su borom keur ak jabot beugue ci yen kon Ye na gui te fou deugueur lolu rek mo gnou taxa jog! Lougnou moun ci partager ak yen si luti li gnou sunu Borom weursaguele fasyeneko tassare. Ndax nieup manse jarinou, In Sha Allah! Pour Sokhna Marietou boulene waax gno gui wadial surprise nianal len gnou mou sotti ak jam in Sha Allah diguene begg 🙏🏾😘
Salaam. Je suis bien contente du commentaire de saveurs planétaires. Vous êtes vraiment tous des anti stress. J vous aime bien et vous suis tous ( alphie, iba, marietou , rabinou, douja...) . C' est l'Afrique qui gagne. Encore merci
aissatou camara ziarnala ma Sha Allah!!! Sa waax rafetna tu as parfaitement raison gnoune gneup ben lagnou ns avons tous les memes objectifs. Sokhna Marietou mome bene affaire la Elle est juste adorable💗 Merci de faire connaître 2 autres(rabinou et douma)! On a aussi une autre sœur BB nana elle aussi fait de bonnes cuisines!😘! Merci du fond du cœur 🙏🏾😘💗
Salam,sokhna Bilo nie ngi delo Ziar bou wèer Masha-Allah ligèye bi rafètena Yallah na nga aglè aksa sago encore 🙏🏽tie recette you ame solo yi👍🏽👏🏼👏🏼👏🏼❤️💚💜
Fama Diop ma cherie ziarnala alhamdulillah lolu rek mo gnou taxa jog ndax guen meuneu begguel ndiabotbi ak wajiuryi aussi. Notre souhait c d’influencer autant de familles possible🙏🏾😘
Mariama Diallo ziarnala ma chérie ma gui am aye chaire de poule saax. Walaye notre objectif c de pouvoir aider et atteindre le maximum de gens possibles pour qu’on puisse en bénéficier et faire plaisir à nos familles. On a tous besoin de plus de variétés ds nos cuisines. Qu’Allah te protège de m’en k ta famille. Contane looooooolu🙏🏾😘😘😘
Coumba D Waleikum Salaam my dear please do they r delish I try not to make it too often cause I cannot stay away from them they r kinda addictive to me😂🙏🏾😘
Salam Billo comment vous allez ? Merci encore pour cette belle recette je suis passionnée par votre cuisine surtout la présentation. Yalna yallah faye.
Ohhh machalah bou nieuw rek gueneu nekh morom sokhna bilo yaw dal amouniou sa faye vraiment ligueye bi rafetna présentation rafete na aussi nassa diam yagg tai yalla weral loxo bi inchalah 🙏🙏🙏🙏🙏
Salaam Sokhna Diarra, j’aimerai bien votre tes créations, tu me m’appeler au +1-646-385-9436 (c‘est aussi WhatsApp) on pourra les inclure dans les émissions.
nyima sanyang oh you r most welcome my sister I hope we can start giving u the subtitles in the video soon. Thank you for stopping by and watching the video🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘
You are welcome, I really enjoy watching you cook and I have cooked the Chinese fried rice... it was really good. Thank you so much May Allah reward you for all ur efforts Amin
Aleykoum salam wa rahmatoulahi Chez Billo merci infiniment pour ces recettes on apprend de plus en plus avec vous et merci pour cette importante que vs accordez à nos commentaires vraiment chapeau à vous
Rokhaya Sall ziarnala ma. Chérie c la moindre des choses qu’on puisse faire si vs prenez le temps de faire des commentaires et suggestions ns vs devons le respect de vs répondre. Surtout bou kaddu yi rafete, jaguene jeuf 🙏🏾😘
Salam Mme Bilo macha Allah mais je voudrais savoir Macédoine canni salade bii ake oignon bi si sachet bi c'était congelé ou bien comme ça je saurai comment le faire merci d'avance
Oui effectivement elle avait fair des sachet d'oignons et poivron congelé comm ca sa boko sokhlawei rk guenei ko c'est super pratique je l'ai fait pour l ramadan. Jai mm congelé mes samoussa.
fatou magatte mane ziar ma cherie je l’ai expliqué ds une des vidéos vers la fin comment le faire sans four! Tte mes recettes tu as l’option de les faites sans four, elles st flexibles🙏🏾😘
Khady Fall ziarnala lou bari sa domeyi yalna len Borombi teguil jafe jafe yoyou, Amine! Farine de coco mom dagaye mener cuire avec alors poudre bi mom c pour texture mom lagnou ajouter ci aye pâte. Dina guene ben tuto pour defat farine de coco In Sha Allah 🙏🏾😘
Salaam Chef Bilo ma Cherie levure bondèe la 🤣🤣🤣 Masha Allah ma mere l’appeler ainsi Masha Allah sister you’re rock I just loveeeeeee your cooking ❤️❤️❤️😘😘😘😘
Saveurs Planétaires Waleikum Salaam sis Marietou diguama raye man saye expressions benene affaire la😂😂😂🤣!!!
Likewise sis laf la thiat ci you baax yi Gaye defar 😘🥰😘😘😘
Chez Billo i called you but it’s a 201 numb maybe you didn’t see it please let me know when is the best time to call u thanks 😘😘😘😘
Machallah yénangui deff liguey bou rafet di diapalé sen rakk yi sen sëy.
Tata marietou please invitel Tata billo ci sa wagn one day inchallah .
Yalla na suniu borom sameu len
Mya mya ziarnala bou baax.alhamdulillah kon jap len ko fofu rek, su borom keur ak jabot beugue ci yen kon Ye na gui te fou deugueur lolu rek mo gnou taxa jog!
Lougnou moun ci partager ak yen si luti li gnou sunu Borom weursaguele fasyeneko tassare. Ndax nieup manse jarinou, In Sha Allah!
Pour Sokhna Marietou boulene waax gno gui wadial surprise nianal len gnou mou sotti ak jam in Sha Allah diguene begg
🙏🏾😘
Yalla na nadjie bi soti ak jam ak salam ndax yen niar nieup souniou ay Tata nguen et on vs aime trop trop machalah
Machallah ma grande idée de cuisine trop délicieux 🙏😘
Alhamdulillah ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Salaam. Je suis bien contente du commentaire de saveurs planétaires. Vous êtes vraiment tous des anti stress. J vous aime bien et vous suis tous ( alphie, iba, marietou , rabinou, douja...) . C' est l'Afrique qui gagne. Encore merci
aissatou camara ziarnala ma Sha Allah!!!
Sa waax rafetna tu as parfaitement raison gnoune gneup ben lagnou ns avons tous les memes objectifs. Sokhna Marietou mome bene affaire la Elle est juste adorable💗
Merci de faire connaître 2 autres(rabinou et douma)!
On a aussi une autre sœur BB nana elle aussi fait de bonnes cuisines!😘!
Merci du fond du cœur 🙏🏾😘💗
Vraiment merciii beaucoup j'apprend beaucoup de choses à travers tes vidéos Merciii
Alhamdulillah ma cherie sa fait plaisir d’entendre car c le but de la chaîne 🙏🏾😘
Machala 😋😋😋😋😋😋
Bonsoir Billo !! Merci vraiment, j ai aimé tes recettes. Contana thi yow.
Alhamdulillah ma cherie ça fait plaisir yalna Yallah Faye ma belle 🙏🏾😘
Salam,sokhna Bilo nie ngi delo Ziar bou wèer Masha-Allah ligèye bi rafètena Yallah na nga aglè aksa sago encore 🙏🏽tie recette you ame solo yi👍🏽👏🏼👏🏼👏🏼❤️💚💜
Amine yaram gnou bok lep 🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️
Nous sommes fiers de bilo et de marietou. Vous nous donner l"envie de cuisiner d"avantage.
Fama Diop ma cherie ziarnala alhamdulillah lolu rek mo gnou taxa jog ndax guen meuneu begguel ndiabotbi ak wajiuryi aussi.
Notre souhait c d’influencer autant de familles possible🙏🏾😘
Salam ta billo franchement merci bcoup j'adore la cuisine mais avec vous on apprends bcoup de choses yalla nala yalla faaye Thie barcke khassida yi 😍
Fama Pene ma. Chérie ziarnala jeureujeuf ci kaddu you rafet to.
Amine ci niane yi te gnou bok lep 🙏🏾😘
Fama Pene amine
Mashalah mashalah yalla Nala yalla fay gniw
Ma Asta amine gnou bok lepp ma chérie!🙏🏾😘
Machalla Sokhna Bilo. les explications sont claires et limpides. Ya bakh té am yéné si li ngay diokhé. Yalla na la Yalla faye.
Ziar maman gnoko bok yalna Borombi bayilene fi lou yagg amine fila begue sasu nek
Mashallah lii amna solo yaangui deff liggeey bou nice😘😘😘😘
Sall Khady ziarnala ma chérie jajeuf ci s’en tewlu aussi 🙏🏾😘
Macha allah amna solo,dieureudieufaty
SLT Mme Billo j'adore bien ta façon de faire et merci pour les recettes
Merci bcp ma chérie ça me va droit au cœur et bienvenue ds la famille 🙏🏾😘
Merci bcp
la cuisine c de l art so nice machalah
M diarra Diop akassa ma chérie ziarnala lou bari 🙏🏾😘
Tata sa fataya am na dioum beurri n’a dolei💪
😂 Waw kouko song dangaye def dang bala mouleye daan.
Dafa pratique so ame aye gane youla beet sofa nek di saf bari would ligueye🙏🏾😘
Masha-Allah Sokhna bilo toppp cuisine👍🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽💚💜❤️
Ziar yaram jajeuf 🙏🏾❤️
Délo Ziar Sokhna Bilo nasa diame saax👍🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤️💚💜🌹
Amine yaram jajeuf 🙏🏾😘
Tré bien expliké. Merci encore
Chez Bilo vous êtes entrain de révolutionner notre cuisine, vraiment chapeau vous fêtes un travail précieux merci et bonne continuation 🙏😍
Mariama Diallo ziarnala ma chérie ma gui am aye chaire de poule saax. Walaye notre objectif c de pouvoir aider et atteindre le maximum de gens possibles pour qu’on puisse en bénéficier et faire plaisir à nos familles. On a tous besoin de plus de variétés ds nos cuisines. Qu’Allah te protège de m’en k ta famille. Contane looooooolu🙏🏾😘😘😘
Merci encore pour votre réaction sa me va droit au coeur. Qu'Allah vous aide à atteindre votre objectif et bénis votre famille masha'Allah
Mariama Diallo amine te gnou bok lep 🙏🏾😘💕
Encore merci Sokhna Billo Machalla èsplication vraiment ç claire mala beugue pire laf thiatt 👍👌♥😘
Binta Diop ziarnala ma chérie fii lleu begbi euppe💕💗❤️
Macha allah tata billo merci bcp pour ces beaux recettes akk yiww bii tamitt je vs admire et bonne continuation tata
Diatou Boulaye ziarnala ma chérie jajeuf ci kaddu you rafet yi yalna Borombi Faye la 🙏🏾😘
Machallah bien expliqué 😘😘
Binta Sy ziarnala jajeuf ma chérie 🙏🏾😘
Salam aleikum tata merci beaucoup ci astuces yi Ak recettes yi
BBFatoou Waleikum Salaam ma cherie jajeuf ci tewlubi 🙏🏾😘
Proud of you
That a lot dear jajeuf 🙏🏾😘
Vraiment merci Mme j'aime bcp votre façon de parler ak accent anglais bi Macha Allah 😍
Aminata ba ziarnala aye waye dama beug sama accent wolof de😂.
Jajeuf ci tewlubi ma chérie 🙏🏾😘😘😘
@@ChezBillo mane dal beugue nala 😍
Aminata ba ma raw ma chérie japalni loma beug rek foof nala te yallah rek taax🙏🏾😘
@@ChezBillo 😍😍😍😍😍
Merci machallah nice na trop
Diamaguene Open ziarnala jajeuf kou baax 🙏🏾😘
Merci Billo ! Que de bonnes idées pour le ramadan mashallah que Dieu te le rende au centuple 😘
Mberry Mmy amine beloved sister likewise
Te gnou bok lepp 🙏🏾😘😘😘💕
Salam honey, very nice and yummy I'm gonna tried inchaAllah mashaAllah
Coumba D Waleikum Salaam my dear please do they r delish I try not to make it too often cause I cannot stay away from them they r kinda addictive to me😂🙏🏾😘
Salam Billo comment vous allez ? Merci encore pour cette belle recette je suis passionnée par votre cuisine surtout la présentation. Yalna yallah faye.
Aminata Wele delo ziar ma cherie c gentille da nga baax rek yalna Borombi Faye la 🙏🏾😘
Machallah choukrane
Akassa ma cherie🙏🏾😘
Lovely Mum❣
Akassa dear thx a bunch🙏🏾😘
Ohhh machalah bou nieuw rek gueneu nekh morom sokhna bilo yaw dal amouniou sa faye vraiment ligueye bi rafetna présentation rafete na aussi nassa diam yagg tai yalla weral loxo bi inchalah 🙏🙏🙏🙏🙏
diarra bousso Amine ma chérie te gnou bok llep man dal beugueu na guiss sen créations tamit 😘
Pourtant niou ngui def ay creation dei seulmnt on sai pa comment te montrer
Salaam Sokhna Diarra, j’aimerai bien votre tes créations, tu me m’appeler au +1-646-385-9436 (c‘est aussi WhatsApp) on pourra les inclure dans les émissions.
Thank you so much for adding the English description.
nyima sanyang oh you r most welcome my sister I hope we can start giving u the subtitles in the video soon.
Thank you for stopping by and watching the video🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘
You are welcome, I really enjoy watching you cook and I have cooked the Chinese fried rice... it was really good. Thank you so much May Allah reward you for all ur efforts Amin
Encore merci beaucoup sokhna Billo
Mamichella 221 ziarnala ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Machallah amna solo
Walo Couture Ziar bou weer akassa 🙏🏾😘
Aleykoum salam wa rahmatoulahi Chez Billo merci infiniment pour ces recettes on apprend de plus en plus avec vous et merci pour cette importante que vs accordez à nos commentaires vraiment chapeau à vous
Rokhaya Sall ziarnala ma. Chérie c la moindre des choses qu’on puisse faire si vs prenez le temps de faire des commentaires et suggestions ns vs devons le respect de vs répondre.
Surtout bou kaddu yi rafete, jaguene jeuf 🙏🏾😘
Machalla ligaye Def amna solo magui laye ziarr bou werr
Aida Diouf ma chérie delo ziar bou weer jajeuf ci kaddu you rafet yi🙏🏾😘
Bravo sokhna billo machallah
Sm Cre jajeuf 🙏🏾😘
Sokhna billo yalna yalla wèralel lokhayi
Khady Niang ziarnala Amine Di le beggue ak wa England yeup 🙏🏾😘😘😘
@@ChezBillo wa England tamite nioguilay bèguè 😘
masha Allah nakk
Inconnu Ry ziar jajeuf 🙏🏾😘
Tu cuisine très bien 😊 merci mai t vidéo son très longue
Macha Allah wakhbi téguénéna yalna ame four
Fatou Sow ziarnala ma chérie amine Borombi meunako yalnala ci japale.
Mais nak li meun nga ko def sans four aussi 🙏🏾😘
Machallah sokhna billo
Tata pliage bi gawna dé je vais tester si je vais y arriver
tajou tajou ziarnala In Sha Allah pcq compliqué woul 🙏🏾😘
Machalla ma belle
Ngone Eyha Diop ziarnala ma chérie jajeuf ci tewlubi 🙏🏾😘
Merci ❣️
شكرا لك يا حبيبة قلبي💕
Ziar ma cherie akassa🙏🏾😘
Salam aleykoum merci pour les recettes peut on utiliser de la pâte brisée ou feuilletée
Ziar ma chérie bien sur tu peux utiliser la pâte feuilletée c très jolie aussi, jajeuf 🙏🏾😘
Yi baguet bi dîna ko defar demain matin inchalla italy la nek mais dieunde pain moma sonal. Merci Sister 👏👌
Awa Diop ziarnala bou weer ma chérie waw nonula histoire de varier touti saax pain gnoun gneup la sonal la yakar xam nga taam rek 😂🙏🏾😘
Yummy thanks
Salam Mme Bilo macha Allah mais je voudrais savoir Macédoine canni salade bii ake oignon bi si sachet bi c'était congelé ou bien comme ça je saurai comment le faire merci d'avance
Oui effectivement elle avait fair des sachet d'oignons et poivron congelé comm ca sa boko sokhlawei rk guenei ko c'est super pratique je l'ai fait pour l ramadan. Jai mm congelé mes samoussa.
Fatou Sow ziar ma cherie oui Aminata Ba a parfaitement raison sur tte la ligne
Sokhna Aminata Ba merci pour cette explication claire 🙏🏾😘
Ziar tata est ce gue je peux remplacer la pâte avc pate feuilleté
fatou diop Demi Ziar ma chérie wawaw tu peux le faire ce sera plus rapide et plus jolie même 🙏🏾😘😘😘
Merci tata
C'est ça qu'on appelle une pierre deux coups 💕💕💕
tajou tajou 😂😂😂
Laal ngako, yaw nand gua affairebi
Machallah tata billo
tata nékh nguama trop say dogue nékhna varié na diadjeufe
M diarra Diop ma cherie ziarnala bou weer ma la gueuneu sop TW guissoumala, jajeuf 🙏🏾😘
Machalla fataya bi nekhna dė
Yebe Sylla waw neexna lolu saax 🙏🏾😘
On attends avec impatience
machallah
Est-ce que cette recette peux se faire sans four
fatou magatte mane ziar ma cherie je l’ai expliqué ds une des vidéos vers la fin comment le faire sans four!
Tte mes recettes tu as l’option de les faites sans four, elles st flexibles🙏🏾😘
Soxna billo farine de coco ak poudre de coco loulene outele sama dome yi dougou lale féne glutine ak lattosio merci
Khady Fall ziarnala lou bari sa domeyi yalna len Borombi teguil jafe jafe yoyou, Amine!
Farine de coco mom dagaye mener cuire avec alors poudre bi mom c pour texture mom lagnou ajouter ci aye pâte.
Dina guene ben tuto pour defat farine de coco In Sha Allah 🙏🏾😘
Merci lére na amine
machalla mai tata propose nous une recette de pizza
Myma Tyfa ma chérie In Sha Allah sous peux!🙏🏾😘
Tata sosou kani à ta façon beugone nagneko kham🙏
Diarista kandji Gueye ziarnala reste à l’écoute kon in Sha Allah dinako def ci koor gui 😘
Machalah
Madeleije1 Ibrahima1 jazzakallah 🙏🏾😘
Mashallah
Topppppp
soso fall ma chérie namnala jajeuf 🙏🏾😘
Et merçi pour d avoir ènumèrer les denrèes👍💖
Coumba D ziarnala de rien ma chérie 🙏🏾😘
foto yii day sorry plat bii nay diegue
Inconnu Ry ziar jajeuf 🙏🏾😘
Coment un fait kani maison
Demba Tirera ziar kou baax tu veux dire sauce kani ?
Si c’est ça bientôt In Sha Allah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Tu cuisine très bien 😊 merci mai t vidéo son très longue