Machallah Oustaz Allahumma inni as'aluka bi-anna lakal-hamd, lailaha illa ant, al-mannanu badi'us-samawati wal-ard, ya dhal-jalali wal-ikram! Ya hayyu ya qayyum!
Salam ya ouztaz Omar sall je suis très contente parcque depuis que j'ai commencé à t'écouter vraiment j'ai changé et je vous dois beaucoup j'ai mis le voile et je suis devenu une autre personne yalnala yalla féy si barke Mouhamed psl
Yene sama mbok djoulit yi ma ngui lene di conseiller nguene setane vidéos oustaz yeup depuis le début dina yok sen tawhid ak sen xam xam Oustaz Oumar Sall yallah nala yallah fay 🥰🙏🏾
Machaallah yaa oustaz vraiment ceux qui vous détestent sont des ignorants mais ne vous en faites pas c'est pas vous qu'ils détestent mais plutôt la vérité.sincèrement vous faites vivre notre ame bonne continuation ya oustaz qu'Allah vous recompense
Walahi azim Oustaz yalla nala yalla Fay bilahi sama xol dafa féss si io ndax ya takh ma changer lou beurii si man tu ma fait ouvert les yeux alhamdoulilah Al-Quran ak Sunnah amoul lénéne🙏
Walahi bilahi ce dua est très efficace je cherchais un document depuis 3 ans mais le jour où j’ai vu ce dua j’ai commencé à le réciter seulement 2 deux mois j’ai eu mon document
Walahi Sénégal sou beuriiwonn niou melnii iow dîner bii dinna gueuna degueur . Machaala ya oustaz yalla nala yalla feyy sa mbax ak sa xol. Le savoir bien partagée.
Je n’ai aucun secret particulier mon ami mais ya Oustaz a raison sur cet invocation D’Allah par son nom suprême.je pense que c’est la solution à nos problèmes
Assamaleykoum viens demander et si on le prononcé comme ça est ce que c'est bien Allahouma inni ashallouka bi Anna Lakale hamdou Lahillaha illalah Antale mane nâne Bâdirou Samati waty waale arde ya khaiyou ya khayoum Ya diale dialaly wale ikrame
Wa Aleikoum salam wa rahmatoulah wa baarakatouh akhyl Karim Bien sûr que c’est bien Alhamdoulilah vous êtes en bonne voie 😊👍 Faudra encore faire un tout petit peu d’efforts pour la prononciation car la langue arabe est telle que si on change une lettre on change le sens la signification Et Wa Allahou alam 😊 En tout cas je suis ravie de voir qu’il y’a des personnes comme toi qui font bcp d’effort Alhamdoulilah 😊 Qu’Allah vous facilite akhy As salam Aleikoum 😊!
Ma cha Allah Oustaz Yalla na Yalla defal diam. Toujours yagui niouy diangal diniou fattely sounou dîné. Oustaz Malick Faye Yalla nako Yalla yeureum defalko aldiana firdaws nek dekouwayam souna rek moko yitelone diangal naniou lou bari ci al kuurane ak souna.
Wallahi,meuss naa sokhla khaliss,ma dem diappou,took wakh niaan bi wakh sama sokhla,paré di def salatou alan nabi, avant may paré salatou alan nabi bi sama téléphone def notification message,ma xool mou nekk message xaliss wave AK orange money
Nous sortons du mois béni de Ramadan.le contexte est très favorable à la prière.c'est pourquoi je prie pour Qu'Allah (SWT) assiste, protège, illumine,notre cher oustase Oumar Sall.Il est très généreux avec son savoi
Salam hanleykoum wallahi je confirme j'ai validé mon L1 alors je n'ai jamais assisté aux sauf ke révision la don déf une semaine avant les examens maintenant suis en licence 2 et je place ma confiance en Allah Sbt borom koun fayakoun Instant yi dafa am kima nékal mom la beugu modon sama borom inchallah dina ganneu respecter séy conseil ya oustaz
Walahi oustaz sama yènè moy niou tassè inchallah damalay top ndeysan dè fw damay guiss niit gni dila wax Lou nek mais yalla xamna leupe walahi yalla nagnou yalla attè si yermandèm 😭
QU'ALLAH T'INNONDE DE CONNAISSANCES ET TE RECOMPENSE DE TON ACTE NOBLE CAR DEPUIS QUE J'AI COMMENCE A TE SUIVRE, J'AI SU QUE J'ETAIS DANS UN EGAREMENT TOTAL. QU'ALLAH TE FACILITE TA MISSION ET NOUS PARDONNE NOS PECHES EN CE MOIS BENI. RAMADAN KARREEM
Merci pour ce rappel vraiment les gens compliquent trop la religion, quand j'ai vu le titre je me suis dit mais attend mais c'est pas le grand secret que certains disent que personne ne sait à part Allah et certains élus mais grâce à vous Umar Sall tout devient facile. Milles mercis à vous
Walahi niann yimouy dioxé man dh guisss na si sama bopou yalna yalla fayla Oustaz walahi beggg nagn si yaw❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuf ya oustaz
Franchement parler, il aime partager son savoir avec les musulmans. Qu'Allah le bénisse. Il n'ya pas de secret pour la religion
Le savoir est pour être partagé
Amine yarabi
Vraiment
Cest vrai
Mâcha alah depuis que je t’ai découvert je ne rate plus tes vidéos , tu as bcp changé en moi yalla na yalla wérreul kham kham bi
Machallah Oustaz
Allahumma inni as'aluka bi-anna lakal-hamd, lailaha illa ant, al-mannanu badi'us-samawati wal-ard, ya dhal-jalali wal-ikram! Ya hayyu ya qayyum!
Merci
Merci
Merci
Yalla na la yalla bindeul yiw
Salut c'est badi'us où bien badiruss
Ndeyssane, barina gniou contre oustaz Omar Sall, te khamougniou sakh ligniouy rate si gniangaleme yi. Yallah nalene Yallah sopi te Yallah delosi sene khel yi. Yallah nafi Yallah yagual oustaz Omar sall. Aameen
Alhamdoulillah
😊
Amine
Amine ❤❤❤
Bilakhi
Salam ya ouztaz Omar sall je suis très contente parcque depuis que j'ai commencé à t'écouter vraiment j'ai changé et je vous dois beaucoup j'ai mis le voile et je suis devenu une autre personne yalnala yalla féy si barke Mouhamed psl
Macha alla 😭😭😭
Machalla yalnala yalla doli katane Mousseul la si cheytane
Alkhamdoulilah
Nian yi yeup guisnathi sama bop masha Allah merci beaucp Oustaz Oumar Sall !
اللّهُـمَّ إِنِّـي أَسْأَلُـكَ بِأَنَّ لَكَ الْحَـمْدُ لا إِلـهَ إِلاّ أَنْـتَ المَنّـانُ بَديـعَ السَّمواتِ وَالأَرْضِ يا ذا الجَلالِ وَالإِكْـرام، يا حَـيُّ يا قَـيّومُ
Allâhumma innî as’aluka bi-anna laka-l-hamdu, lâ ilâha illâ anta , al mannânu. badîghu s-samâwâti wa-l-ardi ! Yâ zâ-l-djalâli wa-l-ikrâmi. Yâ hayyu, yâ qayyûmu !
--------------------------------------------------------------------------
اللَّهُمَّ إِنِّي أَسْأَلُكَ بِأَنِّي أَشْهَدُ أَنَّكَ أَنْتَ اللَّهُ لَا إِلَهَ إِلَّا أَنْتَ، الأَحَدُ الصَّمَدُ، الَّذِي لَمْ يَلِدْ، وَلَمْ يُولَدْ، وَلَمْ يَكُنْ لَهُ كُفُوًا أَحَدٌ
Allâhumma innî as’aluka bi-annî ash-hadu annaka anta-l-lâhu, lâ ilâha illâ anta, al-ahadu, as-samadu, al-lazî lam yalid wa lam yûlad, wa lam yakun lahu kufuwan ahad.
Merci bcp
JazakAllahu Khayran 🙏🏾
Merci beaucoup
Merci
Jazalallah khayran
Yene sama mbok djoulit yi ma ngui lene di conseiller nguene setane vidéos oustaz yeup depuis le début dina yok sen tawhid ak sen xam xam Oustaz Oumar Sall yallah nala yallah fay 🥰🙏🏾
M
Wakhe nga deug dh
Walahi lii gua wakh deugue leu ...
Machallah 🤗
Mane douma rombou bén vidéo oustaz damako beugu dafa def si mane lou bari ma beugu ko.sant mais meunouma fékhé ba am.numerom
Machaallah yaa oustaz vraiment ceux qui vous détestent sont des ignorants mais ne vous en faites pas c'est pas vous qu'ils détestent mais plutôt la vérité.sincèrement vous faites vivre notre ame bonne continuation ya oustaz qu'Allah vous recompense
Personne ne le deteste ces lui même qui pousse les gens a la haine Nay wakhtan té bay kilifa jambour yii
C’est un plaisir de vous écouter qu’Allah vous rétribue au centuple amine ya rabbi
Merci bcp oustaz
wa li nékhna di, lo gnane mou nangou,yallah taxawouleu ya oustaz
Walahi azim Oustaz yalla nala yalla Fay bilahi sama xol dafa féss si io ndax ya takh ma changer lou beurii si man tu ma fait ouvert les yeux alhamdoulilah Al-Quran ak Sunnah amoul lénéne🙏
Walahi bilahi ce dua est très efficace je cherchais un document depuis 3 ans mais le jour où j’ai vu ce dua j’ai commencé à le réciter seulement 2 deux mois j’ai eu mon document
Mâcha’AllAh C’est quel Doua que t’a dit S’il te plaît parce que y’en à 2?
Le premier dua @@Timah221
Le premier @@Timah221
Salam comment on fait le zikr ?
Walahi Sénégal sou beuriiwonn niou melnii iow dîner bii dinna gueuna degueur .
Machaala ya oustaz yalla nala yalla feyy sa mbax ak sa xol.
Le savoir bien partagée.
Bien dit macha allah dieuredieuf
@@ahmadouka8036 merci
J’ai trouvé la solution à mes problèmes machallah oustaz Oumar Sall que la paix soit sur vous 🤲🤲🤲
C koi votre secret partage svp
Je n’ai aucun secret particulier mon ami mais ya Oustaz a raison sur cet invocation D’Allah par son nom suprême.je pense que c’est la solution à nos problèmes
....
@@khadijaba341 comment la tu fais tu peux m'explikei
Salam Aleikoum
Allâhumma innî as’aluka bi-anna laka-l-hamd, lâ ilâha illâ anta wahdaka lâ sharîka laka, al mannânu. Yâ badîcu s-samâwâti wa-l-ardi ! Yâ dhâ-l-jalâli wa-l-ikrâmi. Yâ hayyu, yâ qayyûmu
Assamaleykoum viens demander et si on le prononcé comme ça est ce que c'est bien
Allahouma inni ashallouka
bi Anna Lakale hamdou
Lahillaha illalah Antale mane nâne
Bâdirou Samati waty waale arde ya khaiyou ya khayoum
Ya diale dialaly wale ikrame
Wa Aleikoum salam wa rahmatoulah wa baarakatouh akhyl Karim
Bien sûr que c’est bien Alhamdoulilah vous êtes en bonne voie 😊👍
Faudra encore faire un tout petit peu d’efforts pour la prononciation car la langue arabe est telle que si on change une lettre on change le sens la signification
Et Wa Allahou alam 😊
En tout cas je suis ravie de voir qu’il y’a des personnes comme toi qui font bcp d’effort Alhamdoulilah 😊
Qu’Allah vous facilite akhy As salam Aleikoum 😊!
Merci bc que dieu te donne un château au paradis
Qu’Allah te rétribue de la meilleure façon
Amiiine ma chérie
Amine
06h38 a Dubaï 🇦🇪🇦🇪
Barakallah fikoum imam, 🙏🙏
Ma cha Allah Oustaz Yalla na Yalla defal diam. Toujours yagui niouy diangal diniou fattely sounou dîné. Oustaz Malick Faye Yalla nako Yalla yeureum defalko aldiana firdaws nek dekouwayam souna rek moko yitelone diangal naniou lou bari ci al kuurane ak souna.
Yallah nala Ya Allah fayalegnoula yiwou aduna ak alahira
Ameen mbok
Machallah ya outaz qu'Allah vous protège long vie nous vous aime❤
Bilaye Deugeuleu ❤❤❤❤❤❤yalla nagna yageu digni ware Oustaz oumar Sall🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Ndeysanne ignanoul si xam xam djeum dji wallahi yalla na yalla geuna yeukeuti mayla martaba you kawé 🙏🙏 yalla nalla yalla faye
Alhamdoulilah vous êtes une fierté pour la jeunesse. Qu'Allah SWT vous rétribue vos efforts visible et invisible.
Ya bah ya oustaz yalna la sunu borom tahawou té goudal sa fann si barké yonnenti bi psl🙏
Que Dieu vous récompense oustaz et vous prête longue vie
Diam rek ngay ame incha allah boule noppi moukkke ci wakh ci bida ak bokkaalei yi thiaahaane katte yi nek incha allah
Ma sha ALLAH ya oustaz Oumar Sall YALLAH naga fi yague te weer
masalla Papa, merci, may God the gives u long life n. good health.
Allahouma inni as alouka bi anna lakal hamdou la ilaha ila anta al mannanou badighou sama wati wal ardi ya zal djalali wal ikrami ya hayou ya hayoumou
Merci
❤❤
Oustaz😭 Hamo sakh li nga def .. Yalla nala sunu borom Sameu mayla diam
C’est ça un Musulman partagé et non caché la vérité vous êtes un exemple vraiment 🍀🍀🍀
Jai souri tout au long de cette video. MashaAllah yalla mo baax té beug niou reussir. Naniou sabablou rek. Diox naniou lepp li gnou soxla.
Ana sopéyi😍
Wallahi,meuss naa sokhla khaliss,ma dem diappou,took wakh niaan bi wakh sama sokhla,paré di def salatou alan nabi, avant may paré salatou alan nabi bi sama téléphone def notification message,ma xool mou nekk message xaliss wave AK orange money
Alahou akbarr Yalla rekay bourr
Diazaakoumou laahou hayrann yaa oustaz yalla na la yalla fay yiw samm la aar la laak la fou yaakk yeegoul
Yalla na bok ak ioe apartment aldiana 💞💞💞💝💝💝
Amine yarabi merci
Dieuredieuf niou saxo diko def inchallah yallah Faye le inchallah yallah nongou inchallah
Machallah oustaz vous faite une travaille immense 💎🥰💪🏻wallah qu’Allah te préserve.🤲🏾❤️
Alahoumq amine☝☝☝🤲🤲🤲
Jazakoum Allahou khayra
Ma Shaa Allah Ya Oustaz Y'Allah nala Y'Allah fey yiw
Merci beaucoup oustaz yal nala borom bi samm fay la bayi lafi ay ati ate Incha'allah 🙏🙏🙏
Allahouma inni as alouka bi annalakal khamdou la ilala ila antal mannanou badirou samaawati wal ard ya zal dialaliwal ikram ya khayou yakayoûm
Jeureujeuf oustaz Yalla nala Yalla fay
Masha'Allah alhamdoulilah dieureudieuf ya oustaz ALLAH TALLA augmente ton savoir Amine
Nous sortons du mois béni de Ramadan.le contexte est très favorable à la prière.c'est pourquoi je prie pour Qu'Allah (SWT) assiste, protège, illumine,notre cher oustase Oumar Sall.Il est très généreux avec son savoi
Mâcha ala Oustaz yala nala borom bi fay
Yaa Oustaz walaahi lou baakh rq ngaay ameu Inchaa Allah! 😭😭❤❤
Ya ouztaz yalla naniou la yalla fayal
Yaa goré yaa baakh sa khol bou rafét bi... kallah veille sur toi, te protège et fasse de toi un de ses serviteurs agréés!
Salam hanleykoum wallahi je confirme j'ai validé mon L1 alors je n'ai jamais assisté aux sauf ke révision la don déf une semaine avant les examens maintenant suis en licence 2 et je place ma confiance en Allah Sbt borom koun fayakoun
Instant yi dafa am kima nékal mom la beugu modon sama borom inchallah dina ganneu respecter séy conseil ya oustaz
Ya ouztaz omar sall merci
Frère est ce que tu peut m'aider à avoir le numero de oustaz omar sall
Machallah oustaz amal diam ak weur téy yag fi lole
Ya oustaz Yalla Na Yalla yokou kham kham bi,meune meune bi ak am am bi,yagal sa takhaway🤲🏼🤲🏼🤲🏼
Machallah oustaz Oumar sall
Walahi oustaz sama yènè moy niou tassè inchallah damalay top ndeysan dè fw damay guiss niit gni dila wax Lou nek mais yalla xamna leupe walahi yalla nagnou yalla attè si yermandèm 😭
yalnala yallh fayy oustaz. vraiment senegal ya ngui siy bayy sa waar
mashallah jambaar ngua
yalna yallh fayla yiw sammal nioula beugg nagnla fisabilillah
Machalah mann deh doon nako ligueye chaque goudi ma dem bay guiss you graw
Machalla yalla n'a yalla barkél la machalla imam
Machala oustaz il a parfaitement raison grace a ismoulahil ahzam j'ai pu voyagé en europ facilement.
Mash'Allah mbokk geun si sakh dé ndakh yalla dolli la ndimbeul
Salamou Aleykoum, doma bakhé ban heure nga ka done def ak gnata yone, merci
😭😭
Qu'allah soubhana ta ala accepte nos prières et nos douas amine ya rabbal alamine
Amine
Ma Sha Allah Dieureudeuf yallah na la yallah defal diamm ak KHEWEUL Dieureudeuf❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah long vie oustage bara kallahou fikà deug rek mo am solo alkhouran sounna rek mo am solo
DjazakalLahou khayrane ya oustaz yallah nala yallah Faye yiw
Machallah oustaz
Macha Allah ya oustaz yalla nala yalla fay sa xol
حفظك الله يا شيخنا وجزاكم الله خيرا
Dieureudieuf Yallah na Sunu Borom Dollu Soutoura ak Tawfeekh
Masha'ALLAH ALLAHOUMMA barik amîn Qu'Allah Soubhanahou wa taala vous récompense amîn
Machalla amna solo dieureudieuf Ya Oustaz yalla na borom bi goudeul say fane bou andeu ak werr gui yaram
صل الله عليه وسلم ❤❤❤
Barack Allahou fik ya oustaz qu Allah t prèserve in chaa Alhah
Ma Sha Allah ! ya Oustaz
Qu'Allah nous pardonne nos péchés et agrée nos oeuvres de piété.
Baarakallahou fikoum quelle générosité oustaz yalna ya Allah mayla goudou fane akk weerr
JAZAKALLAH KHAIRAN MAY ALLAH GIVE YOU THE BEST IN THIS LIFE AND THE HEREAFTER AND JAMA ATIL MUSLIMOUN WAL MUSLIMATI
Allahou ma barik Oustaz 🫱🏼🫲🏿
Yalla nala Yalla may diam goudou fane wer ak soutoura
Oustaz may Allah protect and bless you
Macha allah oustaz yalla nalla souniou borome goudeul fane yi deffal leu diam diareudieuf
Macha Allah sa liguey rafetena merci et c'est toujours un plaisir de t'écouter macha Allah merci ustaz
QU'ALLAH T'INNONDE DE CONNAISSANCES ET TE RECOMPENSE DE TON ACTE NOBLE CAR DEPUIS QUE J'AI COMMENCE A TE SUIVRE, J'AI SU QUE J'ETAIS DANS UN EGAREMENT TOTAL.
QU'ALLAH TE FACILITE TA MISSION ET NOUS PARDONNE NOS PECHES EN CE MOIS BENI.
RAMADAN KARREEM
Allahouma amine
Alhouma amine
Machallah yalla na la yalla faye yiw❤❤❤❤❤
Mashallah 🥰 c’est magnifique 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Barak'allahou fikkoum ya oustaz.
Ma challah ya oustaz ❤❤❤
Machallah Oustaz 🙏❤️
MACHALLAH YALLA nala YALLA faye
Merci pour ce rappel vraiment les gens compliquent trop la religion, quand j'ai vu le titre je me suis dit mais attend mais c'est pas le grand secret que certains disent que personne ne sait à part Allah et certains élus mais grâce à vous Umar Sall tout devient facile. Milles mercis à vous
Oustaz Omar sall nikou bhak te moulhabir
@@ibrahimabalde8570 bilahi si tout le monde était comme lui dîna gueuneu bakh
Bilahi même moi aussi j'ai fais cette réaction yalla nako borom bii faay🙏🏽🙏🏽
Mashala ya oustaz
Machallah y'a oustaz
Merci beaucoup y’a oustaz walahi contane nagne trop yalnala borom bi fay 🙏🙏🙏
Machallah. Dieureudieuf Ya Oustaz
alhamduLIlah je remercie à Allahu tabaaraka wa ta'laa q ma donné la chance de découvrir 7 chaîne RUclips vraiment longue vie à vous Ustaz
Vraiment c’est trop gentil merci bcp oustaz 😍😍😍🥰🥰🥰🥰 Longue vie à vos 🙏🏽😎😎🙏🏽😍
Masha Allah, Alahouma Barîk oustaz Omar jerejëf yalna Borom bi sammm, feyy la yiww
Masha allah ouztaz
Alhamdulilah Macha Allah
mérci oustaz
Machallah ouztaz djeuredjeuf
Machalla ya ouztaz
Yalla na yallah godedalsafan