@@tivaonemomelabeug5510 dangay oubi sa leufay ndaye rek Dara manoko si man sa baye Sakh manoul si man dara KO guiss kou nekk biss Dina nieuw mou talén mais fékk yangui deuk di wakh lingay wakh foumala fékk sagga sa ndaye thiotou ndayam ak KO andal manoko si man
Serigne Abdourahman Sy Al Makhtom yalana YALLAH goudal say faan beug na tok akk ioe disso akk ioe cilou bari yalana YALLAH defko barké Cheikhou Tidiane Chérif
SOUGNOU MAME ELHADJI MALICK SY MAODO RTA IBNOU MAME OUSMANE SY RTA AK SA FAMILLE TALIBES TIDIANES SOUGNOUS SOPEYS ABADAANE INCHAALLAH SYMALICK GAMOU TIVAOUANE FOREVER INCHAALLAH MERCI BEAUCOUP
Ki da am kilifa kham louy kilifa serigne chiekh mom ak mame ass ak serign pape malick la yoni won pour wakh al amine mou dem dialle sokhna fat sy neko mom al amine na contune ligeye bi mouy deff te dioh nako kaduu gui
Kan nga guiss mou attaqué KO ki dey tontou kon te balegui mano genné ben wakh boun toude moustafha mom Moy wakh Moy soss Moy wakh depuis Serigne Mansour Moy wakh mom saga naffi Al amine dem ba yonni ay nitt niou sani bomb ci auto Al amine
Yaw fayal etat bi khalissam lanioula wokh truand nga reikk motakh fiyakk fayo dagne lay utiliser reikk comme bouton chaque gamou wala sortie Serigne Moustapha Sy pourtant sa waydiour bou djigeine neina Serigne Moustapha Sy dou sein morom yeinn gneup ndakh sagalna Bayam sa grand frere aussi seidalna Serigne Moustapha Sy fayal ngour gui khalissam lanioula wokh
Yonente yalla yousouf ak domo bay ya yaw li s mostafa wakh si mansour mbaye sode mome kay wed dil sa bay koun yaw sabay kay wedi dakh moko diageu wakh s moustafa
Abdou way😂 ya am diom di wakhaty yaw lo liguéyal Serigne cheikh. Serigne Moustapha dé amna mérite mais rfm khana abdou si mom a sa bouy khas Serigne Moustapha RK siséne radio lay diar
Hahaha. Si vous pensez que Moustapha Sy peut insulter tout le monde sans réaction c'est que vous êtes complètement tarés. Abdou Sy a parfaitement raison. Bande de mal élevés...
Likhéw nékhoul kéneu, mais probléme bi kéneu rék leu. bougoul jamm té baayiwoul kéneu. Limou wakh baayou diambouyi wakhagoukeu bayam, seulement Abdourahmane mo mounoul mougne li gnénéne di mougne
Bonsoir Tivaouane n'a aucun problème, le seul problème est Moustapha Sy qui n'a aucun respect aux membres de la famille Sy et qui chaque jour ne dit que de mauvaises choses sur tout le reste de la famille. Comment le Khalife peut réconcilier la famille de Al Maktoum,lui que Moustapha traite de sorcier et le surnomme même corona.
Al Khalifa dé sampeu makk gni leu lolou Serigne Pape Malick moko wax dieulé ko si Al Amine té thierno Bâchir khalifou cheikh Omar moko sédé si kanamou kilifa chérif yi lolou rék doyna sédé yén nak lou Al Khalifa di agualé jummah mame Maodo moy dagueu sen xol dinguéne dé dé lolou kou am thieur fa yallah rék moko meune 😂😂
Boy abdou yaw laniou yonni kon pour ngua tontou haha 😂 ndeysan xol khasan na té té wokésouko sén xol yi dou fekh mouk s moustapha sagam ak thieureum day yok reg sasouné bousén xol yi nékhoul nioun louniou thi meun niousoulén feulé way
S.Cheikh bakanam la tégone nguir Doundou S. Moustaphal maktoum ndakh thieureum. Faté khadjou fi. Gni amoul thieur rek gnoy thiow, serigne Moustapha da tarbiyou bayam ba Serigne cheikh gueureum ko gnanal ko en public, en ce moment où est ce qu'il etait apart topou banekhou banam. Fa Serigne cheikh dane tokk fofou la tek Serigne Moustapha mouy wakh lamou dane wakh . Koumoi nakari matal sa banane. On est habitué sur ces genres d'attaque organisé pour tirer sur Serigne Moustapha après ses sorties mais peine perde
@@aliounebadarambaye5239 kone khamo li khéw,Serigne Moustapha Serigne Cheikh moko sédél résultawam cices kilifeu yeupp tokk mouniko li nga ligueye yi roukh yékk nako fima tokk,té serigne moni Serigne Moustapha ca ndar 1995 sagal ngama yalla nala yalla sagal ,té sagg mo waral champ de course di gueune di fess, Serigne Moustapha rawléne ci xamxam,ci organisation ,ci resultats , lii rek mo waral thiow li ,fiirangué rek moléne diapp
Je l'aime bien,que le bon dieu le garde longtemps et le protège.
Mo gueneu yéwou mak dji vrément longue vie Serigne Abdou Sy machallah
Yaw sa diobou ndaye wayy yaw danga kham GATT bay wakh
@@badadieye8506 soula nékhé sagua ma déh wayé doula arrangé inchallah bilakhi wolakhi talakhi bientôt dinagua tale léne loudoule aye sagua
@@tivaonemomelabeug5510 dangay oubi sa leufay ndaye rek Dara manoko si man sa baye Sakh manoul si man dara KO guiss kou nekk biss Dina nieuw mou talén mais fékk yangui deuk di wakh lingay wakh foumala fékk sagga sa ndaye thiotou ndayam ak KO andal manoko si man
@@badadieye8506 wa bakhna djeureudieuf
Abdou sy est très responsable et son discours est cohérent et correct.
Il faut savoir utiliser le pur sang de son esprit et non l etalon du cœur. Dieu supporte les endurants.merci pour ton respect.
Macha Allah serigne Abdou sy ❤ Moustafa sy warna kholat boppam limou nécké bakhoul dara
Touti nga si wax si serigne Mouhammad Moustapha sy
Fofou nak lane siy yém nk
@@omarmbayeomzo1mtx yena yam dof mytho yii ngen done
En tout cas xam nagñ ki bayam greum
@@omarmbayeomzo1Bilahi vérité absolue
Merci beaucoup serigne abdou sy ya bakh ya am kilifa machallah yallah nala yallah samm❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ 1:38
Machallah sy malick lii lagnouy khar si dômou daara
Bravo Abdou Sy. Excellent interview
Diazitoume khayrane wa-koufikoume charran wa-lakhitoume ma-bakhitoume darrane Acheikh Abdoul...
Comme papa dji ndaysan
Serigne Abdourahman Sy Al Makhtom yalana YALLAH goudal say faan beug na tok akk ioe disso akk ioe cilou bari yalana YALLAH defko barké Cheikhou Tidiane Chérif
Yallana yalla samoula❤❤
salam
serigne Abdou sy yalnangafi yague thé weur
Abdou sy kou am khelnga wakhe dafa wararfet
Amin
Mach'allah SY Malick gudd fane ak wer rk inch'allah ❤
Merci Abdou sy yàbàkh
SOUGNOU MAME ELHADJI MALICK SY MAODO RTA IBNOU MAME OUSMANE SY RTA AK SA FAMILLE TALIBES TIDIANES SOUGNOUS SOPEYS ABADAANE INCHAALLAH SYMALICK GAMOU TIVAOUANE FOREVER INCHAALLAH MERCI BEAUCOUP
Dieredieuf Serigne Moustapha Sy almakhtoum
Vraiment Talibé yii bolen jisser Serigne Moustapha sy noumouy dokhaler nguen xam nekoul si deuggeu bilahi wallahii ....je peux pas imaginer nite tokkk dhi yakheu deerrou nite nguenii tathiou c tellement grave
Ioe sa digou leufeul ndeye sa bounou ndey sa yo noyé démal nga lidianti sa papa miniouy kate si boune tous ls jour mo geun😂😂😂😂😂
DIEUREU DIEUFF, ,SEIGNEUR BABA CAR SY
Dieureu dieuffeutie sy malick❤️🙏🏾
Mashallah Serigne abdou sy
Machala amna solo
Ki dé woroul almaktoum.
Amna solo abdou❤
Abdou Sy a raison. Tout le monde sait maintenant que Moustapha Sy en veut à son père l'éminent Serigne Cheikh Ahmed Tidiane Sy (RTA)
bien parlé
Dieuredieuf pa abdou sy
Dieureudieuf sy
Bilahi ki mo do nou bayame si bâtin dou turicé mou kou dueg rek laye wakhe ❤❤❤❤
Ki zahir bi matoul nga beugeu ko dougeul si batin
@@gorabsbs2241loko xamal billay yéna bone
Machallah machallah moye rakeu mais amena savoir vivre
Ki da am kilifa kham louy kilifa serigne chiekh mom ak mame ass ak serign pape malick la yoni won pour wakh al amine mou dem dialle sokhna fat sy neko mom al amine na contune ligeye bi mouy deff te dioh nako kaduu gui
Moustapha Sy Tonie la wara bayi
Sa digou data yay kon démal nga wakh si papa mou bayi diouttou nioukoy kate si boune mo geun😂😂😂😂
machallah machallah amatina solo sy malik
Macha Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤
Abou sy aka ignane
Fier de toi Abdou Sy
War nga Sante Serigne Moustapha sy motahhh nga lit dei😂
Ndeysan damala yuerum psq danga tardé
Tivaouane 24 seuytane you bonyi nafekh
Mâcha alah sy malick
Machala sy malick ❤
Très bien dit
ماشاالله
Machalla bien parler ❤
Au moins yawe amegua kilifeu
Machalla
Salam
Alhadoulilahi
Abou Kazab weroul da am febarou xol
ماشاءالله
Walahi wahga deugeu
Deugu rek nga wakh
Sergnbou am kilifa
Abdou sy musul am kilifa
Amine 🙏🙏🙏
Ndeyssane ndiabootou Serigne Babacar sy ak serigne Chiekh lagniy yoni niouy attaqué Serigne Moustapha sy
Astakhefiroula
Kan nga guiss mou attaqué KO ki dey tontou kon te balegui mano genné ben wakh boun toude moustafha mom Moy wakh Moy soss Moy wakh depuis Serigne Mansour Moy wakh mom saga naffi Al amine dem ba yonni ay nitt niou sani bomb ci auto Al amine
@@moussangom3840 binga dioudo yagoul mouno xam li xéw bokk si thiowli xam li xéw moko geun
Tope len feulé amaloulen rewmi bene ndiarigne loudou yakh ak khiro ka nkayo.
Safna sap la réplique mais il faut régler vos problèmes en évitant les médias
Yaw fayal etat bi khalissam lanioula wokh truand nga reikk motakh fiyakk fayo dagne lay utiliser reikk comme bouton chaque gamou wala sortie Serigne Moustapha Sy pourtant sa waydiour bou djigeine neina Serigne Moustapha Sy dou sein morom yeinn gneup ndakh sagalna Bayam sa grand frere aussi seidalna Serigne Moustapha Sy fayal ngour gui khalissam lanioula wokh
Dieuredieuf Serigne Moustapha Sy Al Makhtoum ❤❤❤❤❤❤❤❤
Yonente yalla yousouf ak domo bay ya yaw li s mostafa wakh si mansour mbaye sode mome kay wed dil sa bay koun yaw sabay kay wedi dakh moko diageu wakh s moustafa
Yako féké??🤦
Le pays va Mal les sénégalais sont fatigués.
Bougn xamé s cheikh c grâce à s moustapha sy 😂 mano wax lougn geum
Bi mouhamadoul Moustapha nékké di ligueyeul bayam fo nék
Abdou way😂 ya am diom di wakhaty yaw lo liguéyal Serigne cheikh. Serigne Moustapha dé amna mérite mais rfm khana abdou si mom a sa bouy khas Serigne Moustapha RK siséne radio lay diar
Topaléne feulè kou ame sa greumou baye do wakh louniou tètè guémigne
Abdou kazab domouharame 😂😂😂😂
Sa leufou Ndeye dafay khegne guedje
Sa way domou serigne cheikh ga saga
@@AissatouBaDiallo-qh6zn nafékh ngeu katal sa ndey feulé yéna ngui wakh bénnén domou Serigne cheikh lou geuneu graw wala nga dégu koukoy wakh té wakhossi domouharame
Merci toubnako tu ne m as compris
Hahaha. Si vous pensez que Moustapha Sy peut insulter tout le monde sans réaction c'est que vous êtes complètement tarés. Abdou Sy a parfaitement raison. Bande de mal élevés...
Abdou diokhel khalissou diambour
Yaw nopil lu si sa yoon ĺoko hammal.he is better than you point.
@@lovechinamuchi4616 Worna yalla khamalenako que door kate 560.000€ la dor
Doulkat bi
Mame cheikh ne mérite pas ça. Le khalife doit vous aider à vous réconcilier.
Likhéw nékhoul kéneu, mais probléme bi kéneu rék leu. bougoul jamm té baayiwoul kéneu. Limou wakh baayou diambouyi wakhagoukeu bayam, seulement Abdourahmane mo mounoul mougne li gnénéne di mougne
Bonsoir Tivaouane n'a aucun problème, le seul problème est Moustapha Sy qui n'a aucun respect aux membres de la famille Sy et qui chaque jour ne dit que de mauvaises choses sur tout le reste de la famille.
Comment le Khalife peut réconcilier la famille de Al Maktoum,lui que Moustapha traite de sorcier et le surnomme même corona.
Mais yaw tamit s moustapha sy sa kilifa la de.
ndeysan mom liko meti moy rfm rk la meun waxe masa bo yoroul ay talibe danga wara yarou😂😂😂
Talibe AK haliss moy lane
Abdou sy woutil ay talibé 😂boudé kham gua dara
Kham Dara taxoull am talibe
Li sén Seringe bi yorè dou talibe moustique le
@@ahmadmansourgaye5984 amna niou amoul sakh moustique 😅😅
Mais Abou sarr louy sa problème
Pourquoi si Serigne Moustapha reck ngay wakh
Ta doo wakh daray khame khame
Nga baal ma
Ban khalif ki doon sanni XEER sëriñ BABACAR. Yeen ñuy wax séen Baay yi noonu SËRIÑ BABACAR SY lañu
Al Khalifa dé sampeu makk gni leu lolou Serigne Pape Malick moko wax dieulé ko si Al Amine té thierno Bâchir khalifou cheikh Omar moko sédé si kanamou kilifa chérif yi lolou rék doyna sédé yén nak lou Al Khalifa di agualé jummah mame Maodo moy dagueu sen xol dinguéne dé dé lolou kou am thieur fa yallah rék moko meune 😂😂
Soubhanalah sa wakh bou gnaw té di ay fen nan ngua ko meuné
Bayiléne yakh gor vous les moustarchidine
Boy abdou yaw laniou yonni kon pour ngua tontou haha 😂 ndeysan xol khasan na té té wokésouko sén xol yi dou fekh mouk s moustapha sagam ak thieureum day yok reg sasouné bousén xol yi nékhoul nioun louniou thi meun niousoulén feulé way
Yaw domerame nga vous Kate sa ndaye
S.Cheikh bakanam la tégone nguir Doundou S. Moustaphal maktoum ndakh thieureum.
Faté khadjou fi.
Gni amoul thieur rek gnoy thiow, serigne Moustapha da tarbiyou bayam ba Serigne cheikh gueureum ko gnanal ko en public, en ce moment où est ce qu'il etait apart topou banekhou banam.
Fa Serigne cheikh dane tokk fofou la tek Serigne Moustapha mouy wakh lamou dane wakh .
Koumoi nakari matal sa banane.
On est habitué sur ces genres d'attaque organisé pour tirer sur Serigne Moustapha après ses sorties mais peine perde
Ballegui gni mou wahalone tontou wougnouko donc kane moy wah boba ba leegui
Mofa tokk lolou deugu la wayé gathiélna place bi, c'est une insulte ce que tu as dis, Serigne Cheikh bén domam donouko
Ndaysan Yalla nañou Yalla samal Serigne Moustapha sy Maktum amine amine amine
@@aliounebadarambaye5239 kone khamo li khéw,Serigne Moustapha Serigne Cheikh moko sédél résultawam cices kilifeu yeupp tokk mouniko li nga ligueye yi roukh yékk nako fima tokk,té serigne moni Serigne Moustapha ca ndar 1995 sagal ngama yalla nala yalla sagal ,té sagg mo waral champ de course di gueune di fess, Serigne Moustapha rawléne ci xamxam,ci organisation ,ci resultats , lii rek mo waral thiow li ,fiirangué rek moléne diapp
@@biremegadiaga3253 amine inchallah
Moustapha dafa trokh
Yaw ya dakha doul si adouna bi danga pert danga torakh sim
Yaw ya bon loko hammal dafla mousa fennal.amal respect naka yarr.
Barcke mouhamed door kate abdou sy un vrai escro 650.000€ la dor ben toubab italien barcke yalla
Bayiléne yakh goor vous les moustarchidine
@@lafindutemps6141 walahi suis pas un moustarchidine mais walahi lima wakh degue c’est un vrai truyan
Muna fenn.
Douma fen j’ai les preuve walahi j’ai les preuves wadji truya la
Bayil Doul ak Togne
salam
serigne Abdou sy yalnangafi yague thé weur
bien parlé
Au moins yawe amegua kilifeu
Machala
ماشاءالله
T😅vvvvvvvvvvv
J
Macha alla
Au moins yawe amegua kilifeu
Machalla
Machalah