J'étais à sainte Jeanne d'Arc avec lui en 1987, il était marrant, gentil et faisait beaucoup rire toute la classe. Très content de te retrouver Abdou Sy
Nooo sacré Abdourahmane Sy ,un ancien camarade de promo à Sainte jeanne d'arc ,il était cool, aimé bien taquiné et je me rappelle très simple, aussi ,malgré qu'il faisait partie d'une grande famille religieuse et son père un grand érudit lui il ne parlait pratiquement pas de tarikha et ne se glorifier pas sur son appartenance à la famille Sy..D'ailleurs lors des gamou on le voit rarement y aller..A l'école il était très brillant aussi ...il avait de l'humour et faisait rire toute la classe..Un bon type Abdourahmane
Bien pausé, bien réfléchi, je sens une éducation, une sincérité et maîtrise en soit... c'est la toute première fois que je l'attends mais ce Monsieur force le respect ❤
Le prophète a entendu des accusations pires que celles-ci. Ce qui est marrant c'est que ces hypocrites l'ont appelé pour qu'il insulte Serigne Moustapha Sy a leur place par ce qu'ils n'osent pas le faire. Hypocrite qu'ils sont, ils essaient de jouer le rôle de médiateur tout en étant réjouis des insultes adressées à Serigne Moustapha Sy Al Maktoum. Le fils qui rend Serigne Cheikh fière là haut, c'est le fils qui l'a remplacé au champ de courses. Rester en colère et laisser Dahiratoul Moustarchidiine wal Moustarchidaate continuer de briller avec notre le guide le plus brillant et intelligent de son temps.
Machaalla Serigne Moustapha Sy notre responsable moral DMWM nous sommes très bien fière de vous Que DIEU vous bénisse incommensurablement Amine avec vous jusqu'à ce que la mort nous sépare Abadane inchallah
Superieur😅 on dirait une entreprise. Supérieur dignité akk ngoor mokay deff tei lolou yeup serigne moustapha moleinn ko eupp. Si votre khalif refuse de dire la vérité pour son propre intérêt c’est pas la faute de serigne moustapha. En plus celui qui a la bouche pleine ne parle pas 😅
@@PierrewilliamMangaSerigne Moustapha lim respecter woul ay magam, mootax xalé you ndaw deukke di dougou di thiaayaam diko woowé ay mythomane di fégnal ay fénam ay taalibém di mér ta doune si mane darra😂
@@MorCisse-l9mhéé baayil wakh loula woroul, ki Abdourahmane Sarr lagnouko toudé kénenki mo toudeu Abdou Aziz Sy gnou toudéko Al Amin mou yaroo si tourendom.
Diarama Serigne Moustapha Sy lui, il a éduquer, enseigner et orienté bcp de jeunes dans le droit chemin et c'est son père Serigne Cheikh qui la confirmé a ces paroles " Moustaph esk hamnga linga réussir si roukh ? Man fii matok khamnà ko" En plus Serigne Moustapha Sy amna geureumou bayam. Serigne Cheikh môko wakhôn Niko Moustaph yama geuneul samay gnaary geut bougnoula naré sacrifié ma djohé sama bop. Wà lii doyoul geureum. Donc Serigne Moustapha Sy a belle et très bien réussi sa mission. Yalna ko yalla fay amiin inchallah. Abdou wahgnou lô reussir sisa live esk amnga sa geureumou baay?
Je l'aime bien ce Monsieur. La vérité est un trésor de Dieu. Et son discours sur la situation politique au Sénégal, son refus de soutenir un candit, la possibilité du pouvoir à subvertir tout prétendant quelque soit ses qualités en raison de la concentration de trop des prérogatives aux mains d'une seule personne, démontrent à suffisance le Courage dans la vérité et une culture générale assez bonne. Yallah na Yallah deuguereule guiss guiss sam aki taxawayam.
Diarama cheikh seydi Mouhamadoul Moustapha❤yalna yalla goudal fanam doli ko werr ak tawfeikh.❤❤❤❤🎉🎉bamou motali mission bi ❤❤❤ Ndeysann mo demal mamam toll. Moy takhaw ci balcon nieup kheum.gni di dioyy.khol yi feikh neikh❤❤❤❤❤❤❤bon khatarayou
Bi Serigne cheikh Di wakh Serigne Moustapha sagual guama yalla n'ala yalla sagual fo nekonn niou mom bé faw ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Pour te dire vrai Abdou Sy Serigne cheikh dou wédi boppam kholatal bou bakh li nga wakh féne bakhoul talalla micro Di wakh rek bakhoul Serigne Moustapha défa sagal bayam té douko mossa wane guinaw bé tey bé souba incha Allah
Kou yaar sa diouni morom bouné Dou meussa morom NGA war ko Gueum meussou niouleu degu NGA wakh xam xam Lou sa wadiour yorone Diokh Nako Serigne Moustapha Sy té amoul tapalé Lou dalone Yonenté Yalla Youssef AK ayy freram molen dal ci Serigne Moustapha ❤️
Yalna yalla sameu cheikh Moustapha. Liko mame cheikh wah rek moofi nek. Moustaf tu as trop d’ennemis, des ennemis tellement méchants tellement mal honnêtes.
Rfm amléne touti jom té kham Serigne Moustapha sy al Macktoom beuri ci mbartal pouss mou dém poussoul moi dém. Lolou la yalla dogal. Deug mom di khokh par force ci mim rew. Nafekh you bonne
@@balla2-n1s Il ne respecte pas les gens. Il passe tout son temps à mentir, à fabriquer , inventer des histoire à dormir debout. « J’ai eu à rencontrer Allah SWT, j’ai dîner avec des prophètes. ASBOUNALAH
Serigne Abdou Sy le Gamou 2020 c’est lui même qui a critiqué le Khalifa Serigne Moustapha Sy notre responsable ❤on l’aime et on le protège Gfm c’est du n’importe quoi 😅
Excellente intervention. Merci Abdou Sy
J'étais à sainte Jeanne d'Arc avec lui en 1987, il était marrant, gentil et faisait beaucoup rire toute la classe.
Très content de te retrouver Abdou Sy
Serigne Moustapha SY bayam daf ko gueureum toujours au service de Al makhtomm et moustarchine ❤ Yalla mokoy fay Serigne Moustapha rek❤
Loum ligaya lone bayam yakhal nako lou ko raw
Serigne Moustapha sy kay amna ngueram si Serigne cheikh
Deug bou wérr seringue Moustapha s'y Bamouy ligeeyal sëriñ Cheikh bobou mom mogui teud di nélaw
Nooo sacré Abdourahmane Sy ,un ancien camarade de promo à Sainte jeanne d'arc ,il était cool, aimé bien taquiné et je me rappelle très simple, aussi ,malgré qu'il faisait partie d'une grande famille religieuse et son père un grand érudit lui il ne parlait pratiquement pas de tarikha et ne se glorifier pas sur son appartenance à la famille Sy..D'ailleurs lors des gamou on le voit rarement y aller..A l'école il était très brillant aussi ...il avait de l'humour et faisait rire toute la classe..Un bon type Abdourahmane
Merci beaucoup Serigne Abdou Rahmane Sy nék ndaw dou téré nité
Machallah Sy Malick si yarbi ,d'Albi,ak téy bi yalna nga soute sa waydiour Aw fane té décé barké ba
Serigne Abdou Rahmane sy yalne yalla goudeul sa fane tékk la si siratal moustakhim
Bien pausé, bien réfléchi, je sens une éducation, une sincérité et maîtrise en soit... c'est la toute première fois que je l'attends mais ce Monsieur force le respect ❤
K la grâce de dieu soit avec vous ❤
Merci Serigne Abdou sy, longue vie. Grand respect a vous
Bilahi conetane na si serigne abdou sy yalla na yalla dolila sam si barké seydina mouhaméd psl
Le prophète a entendu des accusations pires que celles-ci.
Ce qui est marrant c'est que ces hypocrites l'ont appelé pour qu'il insulte Serigne Moustapha Sy a leur place par ce qu'ils n'osent pas le faire. Hypocrite qu'ils sont, ils essaient de jouer le rôle de médiateur tout en étant réjouis des insultes adressées à Serigne Moustapha Sy Al Maktoum.
Le fils qui rend Serigne Cheikh fière là haut, c'est le fils qui l'a remplacé au champ de courses.
Rester en colère et laisser Dahiratoul Moustarchidiine wal Moustarchidaate continuer de briller avec notre le guide le plus brillant et intelligent de son temps.
Machaalla Serigne Moustapha Sy notre responsable moral DMWM nous sommes très bien fière de vous
Que DIEU vous bénisse incommensurablement
Amine avec vous jusqu'à ce que la mort nous sépare
Abadane inchallah
Ma contane serigne abdou sy almakhtoum. Il a un respect envers ses supérieurs. Il est correct et très discipliné
Superieur😅 on dirait une entreprise.
Supérieur dignité akk ngoor mokay deff tei lolou yeup serigne moustapha moleinn ko eupp.
Si votre khalif refuse de dire la vérité pour son propre intérêt c’est pas la faute de serigne moustapha.
En plus celui qui a la bouche pleine ne parle pas 😅
@@PierrewilliamManga incorrect indiscipliné et insolent
@@assanesarr6177 parks j’ai dis la vérité?
@@PierrewilliamMangaSerigne Moustapha lim respecter woul ay magam, mootax xalé you ndaw deukke di dougou di thiaayaam diko woowé ay mythomane di fégnal ay fénam ay taalibém di mér ta doune si mane darra😂
Gnoune dal Serigne Moustapha sy rék moy yaw Mouye nathie ❤ Serigne Moustapha sy Al makhtoum ❤️ rék
Ya kham d nokhoule feulé yak tapha sy
Amngassi droit mais passe ton chemin... l'invité s'appelle Abdourahmane Sy et non Moustapha Sy.
Soffngéne torop
@@TALIBECHEIKHNATIDJAN va là-bas
@@MandiayeNdiaye-ow4bf pourtant Mane waadji lay tontou
@@TALIBECHEIKHNATIDJAN balma dama dioume
Dieureudieuf Serigne Abdourahmane Sy Almakhtoum
Qui tudul abdouraxmane qui abdou latudu quénèn ki mo tudu
@@MorCisse-l9mhéé baayil wakh loula woroul, ki Abdourahmane Sarr lagnouko toudé kénenki mo toudeu Abdou Aziz Sy gnou toudéko Al Amin mou yaroo si tourendom.
@@TALIBECHEIKHNATIDJAN leral yi rafetna trop amna soolo trop
Machallah Serigne Abdou gnou ziarr Di contane
❤euskeuye. Merci serigne abou sy malick
Merci Abdou sy, vous méritez notre respect ❤❤
Seringe moustapha sy almakhtoum rek❤❤❤❤❤❤❤
merci beaucoup serigne abdou
Serigne abdou sy mame cheikh békna thi yaw machalla
Dieuredieuf serigen abdou sy al maktoum toujours degeu rk lay wakh machallah ❤
Sa digante ak sa borom ki boudoul won limouy tontou Serigne Moustapha dakh dako xam danko waron lathie 1993 ba 2011 Serigne Moustapha rek thi terebi niou tathieko fi def l'éppou ba almaktoum genat wakhak nieppou boba mom anamou té almaktoum dou wakh thi roukhou limaou Wakhal Serigne Moustapha nieppou deg nak dakh masga deg toutou abou s'y thi lamigne bou almaktoum
Serigne Moustapha Sy Maktoum dal bayam publiquement loko sant gueureum ko donc yawite Wanel foula sa baay santé AK gueureum...
Toy guemign baaxoul
Bien dit frère
Ibliss nak yalla dako takaloone ay grade ba def ko chefou Malaaka yi ta fim moudié gnéppe xamnane ko. Loolou moo dal sene waadji
@@الراجيرحمةربه-ث5مyaw sonnou gua Esk doo fékheul sa xol bou boone domou thiaga bi
Sounou saringe sounou responsable morale yalnako yalla arr yokou fanwi ak wergui si barké seydina mouhamed s...❤
Amine inshallah
Dieureudieuf Serigne Abdou Sy
Machallah wakh bi rafetna SY Malick ❤
Dieureudieuf Serigne abou sy diokh respect sayy baay daal laa Serigne wara diangal ay talibeem
Diarama serigne Moustapha sy Al macktoum ♥️
Diarama Serigne Moustapha Sy lui, il a éduquer, enseigner et orienté bcp de jeunes dans le droit chemin et c'est son père Serigne Cheikh qui la confirmé a ces paroles " Moustaph esk hamnga linga réussir si roukh ? Man fii matok khamnà ko" En plus Serigne Moustapha Sy amna geureumou bayam. Serigne Cheikh môko wakhôn Niko Moustaph yama geuneul samay gnaary geut bougnoula naré sacrifié ma djohé sama bop. Wà lii doyoul geureum.
Donc Serigne Moustapha Sy a belle et très bien réussi sa mission. Yalna ko yalla fay amiin inchallah.
Abdou wahgnou lô reussir sisa live esk amnga sa geureumou baay?
Merci beaucoup gnou ajouter si bikoh mame dinan sagal ngama yalnala Y'Allah sagal❤ yalnanou Y'Allah fayal sougnou kilifa
Mashalah sy diame si yaw
Merci beaucoup Serigne Abdou Rahmane Sy Al Makhtoum que dieu vous protège ❤❤❤
Merci serign bi kadou yi amna solo
Kadu tésséne té
Je l'aime bien ce Monsieur. La vérité est un trésor de Dieu. Et son discours sur la situation politique au Sénégal, son refus de soutenir un candit, la possibilité du pouvoir à subvertir tout prétendant quelque soit ses qualités en raison de la concentration de trop des prérogatives aux mains d'une seule personne, démontrent à suffisance le Courage dans la vérité et une culture générale assez bonne. Yallah na Yallah deuguereule guiss guiss sam aki taxawayam.
machalah sy wakh dji amna solo
Na topou falé
J suis très content serigne abdou wakh dji amena solo
Merci beaucoup Serigne Abdou Sy, j'ai un amour incommensurable à Serigne cheikh tidiane sy . Deg du romb nopou
dieureudieuf serigne moustapha sy al makhtoum
Diarama seringue moustapha sy maktome ❤❤ 2:42
Serigne abdou say kadu rafet na sell na machallah
Machalllah serigne abdou aziz sy❤
Serigne moustafa sy moy sen serigne di sen serignou serigne sm l maktoum yalnafi yag ta werr
Serigne Moustapha notre vie ❤❤❤❤❤❤❤
Yene da ma léne yeureum
Diarama cheikh seydi Mouhamadoul Moustapha❤yalna yalla goudal fanam doli ko werr ak tawfeikh.❤❤❤❤🎉🎉bamou motali mission bi ❤❤❤
Ndeysann mo demal mamam toll.
Moy takhaw ci balcon nieup kheum.gni di dioyy.khol yi feikh neikh❤❤❤❤❤❤❤bon khatarayou
Aller faire la réécoute de la conférence CICES 1997 et et et la causerie de Serigne Cheikh lors de sa visite à Tivaoune 1998
ki mome yakh rèk mais yalla bakhna 😢😢
Une personne véridique ❤
Serigne Abdou bien ditque dieu vous garde
Diarama Serigne Moustapha SY Al Maktoum
DIEUREDIEUF CHEIKH SEYDIL MOUSTAPHA SY YALLA NA SA DIAMA YAGA SY AMINE YARABAL HANLAMINA 🤲🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏👐 ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲
Serigne cheikh H T sy mon guereume serigne Moustapha sy.jarama serigne Moustapha sy ❤. Lowakh deug là
Masahala ❤❤❤
Nous les moustarchid nous n'avons pas ce temps bunu wahé renn dewnati ❤
Bayil lén togne vous créer toujours des histoires
Passe ton chemin... lofiydéf?
Bi Serigne cheikh Di wakh Serigne Moustapha sagual guama yalla n'ala yalla sagual fo nekonn niou mom bé faw ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Diaram serigne moustapha sy
Sagal ngueine ma la wax boul deformer wax bi
@@TheTamsir moustaf sagal ngama yalla nala yalla sagal loolou la wakh de; waye nak nit booco beugoul rek beugoo ko dooko wakhal lou raffet jamais
Mais dou leegui dé.
Sagolonguama la diéfé
@@kamidiotv8269 waaw batay bakhna waaye amna nioo khamne serigne cheikh meusoul toudou seene toure kenn khamouleen ba serigne cheikh lakko lagnou guenne di soss lou takh ba serigne cheikh di dounde deggo ci keen. Waaye soûl ker douko teree feegne
Machalah s'y Malick wax ji rafettna
Machallah Serigne Moustapha sy ❤️❤️❤️
Discours bou am solo MachAllah
Bien dit vraiment. Respect!
Merci Abdourrahmane sy❤❤❤
Merci sama wadji❤❤❤
L'islam est un parti politique
Vive l'islam vive la parti politique d'Allah
MACHA ALLHA. Deugue nekhoul
Pour te dire vrai Abdou Sy Serigne cheikh dou wédi boppam kholatal bou bakh li nga wakh féne bakhoul talalla micro Di wakh rek bakhoul
Serigne Moustapha défa sagal bayam té douko mossa wane guinaw bé tey bé souba incha Allah
Kheuyna bi Serigne cheikh Di tag Serigne Moustapha sy boba problème amoul woon Seen digantee
@@bocarwade8241voilà tu as bien compris
Yalla na yalla tapé kholyi
Yalla nagnou yalla taass si barké wadiour yi
Seydi Moukhamadoul Moustapha Sy almakhtoum amoul morome 🙏🙏
Merci Abdou sy❤❤❤❤
Serigne Moustapha Sy Al Maktoom ila akhiri dahriiii rekkikkk❤❤❤❤❤❤
Serigne Moustapha almakhtoum yalla nafi yague té wér
Kou yaar sa diouni morom bouné Dou meussa morom NGA war ko Gueum meussou niouleu degu NGA wakh xam xam Lou sa wadiour yorone Diokh Nako Serigne Moustapha Sy té amoul tapalé Lou dalone Yonenté Yalla Youssef AK ayy freram molen dal ci Serigne Moustapha ❤️
moustapha Sy dou dara
Kou yakke sa diouniy maroom kay
@@الراجيرحمةربه-ث5مt'as pris ma réponse😂
Yow Ndeysan kou diara yeureum nga khana amo pape motahh nga top moustapha sy comme un écervelé
Yalna yalla sameu cheikh Moustapha. Liko mame cheikh wah rek moofi nek. Moustaf tu as trop d’ennemis, des ennemis tellement méchants tellement mal honnêtes.
Merci beaucoup abdou sy al macktoum
Talibé Cheikh dou am diote nagne continuer snouy diamou yalla
Merci beaucoup ya oustaz
En tout cas dall serigne cheikh Ahmed tidiane sy Al maktoum moom serigne moustapha lagnou bolél
Abou sarr nga balma
شكرا ياسيدي سه جزاك الله خيرا ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallh cadou yi refete na
troppe sah🤣🤣🤣🤣
Serigne Moustapha pour tjr
machallah machallah amatina solo sy malik kadou yii rafetna trop machallah sy
❤❤❤❤❤❤❤❤❤tu mérites respect
Machallah amana solo trop way yallah na yallah faye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci Mr Sy
Dieuredieuf Serigne Moustapha Sy Al Makhtoum ❤❤❤❤❤❤❤
Nitt ki bou wakhé rek nga xam moy kann, bo holé ni Serigne Abdou di wahé nga xamni Yarr rekk mo am solo, alal ak daradja am yarr mo geun fa yalla
Rfm amléne touti jom té kham Serigne Moustapha sy al Macktoom beuri ci mbartal pouss mou dém poussoul moi dém. Lolou la yalla dogal.
Deug mom di khokh par force ci mim rew. Nafekh you bonne
Il a raison. Moustapha Sy est MALADE MENTALEMENT sans pour autant le savoir.
Par respect au moins
@@balla2-n1s Il ne respecte pas les gens. Il passe tout son temps à mentir, à fabriquer , inventer des histoire à dormir debout. « J’ai eu à rencontrer Allah SWT, j’ai dîner avec des prophètes. ASBOUNALAH
Machalla merci beaucoup ❤❤❤
RFM diakhassé rek moy sen liguey
Yalnalen sougn akh dall
Jtm beaucoup seydi aboubakar sy jtm beaucoup seydi mouhamdal moustapha sy ❤❤❤
Wolie Ndeysan Macha Allah Sy
DIEUREDIEUF CHEIKH SEYDIL MUHAMMAADOUL MOUSTAPHA SY AL MAKTOUM YALNA FI YAGUE TÉ WÉRE SAGOU DINÉ GUI
Serigne Abdou Sy le Gamou 2020 c’est lui même qui a critiqué le Khalifa
Serigne Moustapha Sy notre responsable ❤on l’aime et on le protège
Gfm c’est du n’importe quoi 😅
Li rek motakh sen miroir saleté mais on verra personne n'empêchera a Serigne Moustapha d'atteindre son objectif
MUJU BU XOLAAM DUL FEEX AK NOON YI PEXEEM DUL JEEX
Merci Serigne Abdou
MERCI ABDOU SY BIEN DIT 😂😂😂😂❤❤
Macha'allah Sy Malick ❤❤
Abdou sy yalna la yalla alak
Yaaa meuna fen té meuna sos
Merci abdou. Bien dit
MACHALLAH MACHALLAH Serigne Abdou. Leup rafetna MACHALLAH amnga droit défendre sa Papa
Khana téy hier amonna où étiez vous
Sunu Serigne Sunu responsable moral Serigne Moustapha sy au cœur de ts les Moustarchids
Kou wédi Serigne Moustapha sy wédi Serigne cheikh démléne nopalou té yattou deneu