Propos tenus à Ker Dieumb: Abdou Sy dément Serigne Moustapha Sy « Moustarchidin » et avertit ....

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 60

  • @diedhiougoudiaby
    @diedhiougoudiaby 6 месяцев назад

    Merci Serigne Abdou Sy

  • @thiamdarou3860
    @thiamdarou3860 6 лет назад +3

    serigne moustafa yalla nako yalla samme

  • @adjidiop3039
    @adjidiop3039 7 лет назад +8

    Qu'alla nous protéges par la grace du pft psl

  • @ousmanewade4062
    @ousmanewade4062 7 лет назад +22

    L'histoire se répète. Les premiers ennemis du prophète Youssouf étaient ses frères.
    Pourtant Youssouf était l'héritier de Jacob.Il était aussi les plus nobles des fils de Jacob.
    Serigne a dit publiquement '' Moustapha tu as des ennemis tellement dangereux, des ennemis tellement malhonnêtes''
    Serigne cheikh a dit publiquement à saint Louis '' Moustaph ,saggal nguama Yallana Yalla saggal la,Térral nguama Yallana Yalla Térral''.
    Ce même Serigne cheikh a dit Serigne Moustapha c'est votre responsable moral ,c'est votre chef de guerre ,c'est votre grand patron.
    Acceptons le destin.Serigne Moustapha c'est c'est un élu de Dieu.

  • @Moustarchidine
    @Moustarchidine 6 лет назад +1

    Ce que Babacar Fall ne dit pas aux auditeurs de RFM aussi est que le passage censuré dans l'audio où Serigne Moustapha Sy Jure Bil Laahi wal Kitaabi. Et Abdourahmane Sy renie mais ne jure pas ni donne des témoins.
    Serigne Babacar Sy sunu Maam la mais sou dellou si woon ne gnou Bayyi Serigne Moustapha, cela est de même pour Al Maktoum.

  • @coumbathiaw2656
    @coumbathiaw2656 7 лет назад +3

    machalla yalla nako yalla ar lacal you ko fou laca yegoul samal you ko mouseul gnou thi peye none

  • @papesall4753
    @papesall4753 2 года назад

    Lou leer lay wakh nii ✍️

  • @khalifadia4513
    @khalifadia4513 7 лет назад +1

    Yaw nenga 40em jour mame cheikh degg nga mu wakh benn bát pap malick lutax tontu woko woon tay nga tontu xana li gaston wakha goul woon motax yaw dal gaston ngay fiy tontul

  • @khalifadia4513
    @khalifadia4513 7 лет назад +4

    Yaw manam sumala dégé yaw ku mame cheikh di waxal force nga kham ko xana yaw danga yëddu

  • @talibescheikh100tvlofficie7
    @talibescheikh100tvlofficie7 7 лет назад +3

    walaye ndéysane serigne cheikh tidjiani sy al maktaum rta liyeupe wakhone nako nitou hakhikha deugue lawone kone senegal kagne laniouye yéwou khamni diné ak sunu tarikhabi dou aye sante

  • @papeousseynougueye1420
    @papeousseynougueye1420 6 лет назад

    Salam yaw ga koula degue siyabo mou nianala bobague niou gamela dangay guene Senegal demal diangui serigne moustapha bimouy am say att minguiy diangale sa papa serigne cheikh limou wakh si serigne moustapha wakhouko si bene dome bou feke danoula fay nga wakhko yalna yala sopila amine

  • @ibrahimsall6492
    @ibrahimsall6492 7 лет назад +3

    Tu as raison Abdou sy

  • @elmalickgueye383
    @elmalickgueye383 6 лет назад +1

    DEUGG RÉK MO AM SOLO.

  • @serignendiaye1156
    @serignendiaye1156 6 лет назад +1

    Serigne moustapha yanalla sougnou borom ar leuh

  • @badasarrsarr9551
    @badasarrsarr9551 7 лет назад +1

    Machalla machalla amna solo torop way yaw kou bahk ga way

  • @Moustarchidine
    @Moustarchidine 6 лет назад

    Le journaliste RFM, Babacar Fall un fumiste doublé de fumier, vous appelle "Serigne Abdou Sy" et appelle votre frère Moustapha Sy. N'est-ce pas paradoxalement lorsque vous, Abdourahmane Sy vous reniez dans votre interview le statut de "Serigne" tout en l'appelant "Serigne Moustapha Sy".
    Le nom de Responsable moral n'est pas auto-déclaré mais une appellation d'Al Maktoum.

  • @mouhamedgaye6936
    @mouhamedgaye6936 6 лет назад

    Li serigne abdou sy de worone na am khele ni Sénégal li du née doy n'a warr lou am solo moy nopi ndakh lou thi meunti am rek daniou nane yako wakh moune n'a am mou l'or ko l'or la yaw minii di wakh ba ague thie mame cheikh ndakh mom bougoulwone ay domame ndourook ay ennemis ndakh so lene baye bamou diougefi ken di def li mou dann lenn moutoulo kon dieuwnguene ko même wakh ngua koy wakh moune n'a indi ay mbirr youdoul diekh te diaroukofi wakh ko sen birr ba kounek khamm fimou dioume lepp diekh ak goor gui yakaar gimou amone thi bolo domam yi serigne moustapha responsable moral la et ya de million et des milliers Youko yakkar legui yaw ngua démentir mou mane ko yakhal ken doula gueume komasse thi mane na la woor lou berry thi ndiabotou mam maodo ak ay terrè khamoko ndakh fimou diaar diarofa ndakh mame cheikh mo ko falle yaw bo rombè niounane domi serigne cheikh mo wakh li magam ak kholal mame cheikh nimou magè yaw nguay niakal sa bopp fayda ndakh mounolena niakal fayda ndakh cheikh ak mame babacar nio lène di arr yaw sakh danaka niou berry khamounioula
    Guiss ngua kou liguèyale cheikh ak tope lenene yamouniou yaw ligueyo fi loutakh niounane wakh ngua deug ndakh sant sy takhoule niounane gathiengualama ba la ngua ko khamm ngua dem course ba gamou kon bayil gni ligueyale cheikh wakh ndakh maodo ..
    Man damalaye lathie deug masse ngua deegg ben serigne khalifa wala porte parole niouy wakh lou niaww sen birr ? Es que masse ngua degg pape Malik mingay wakh wakh si dara ? Li yepp amoul sens gniyy gueume gueume nane ba paree ngiy khamm khamm ba parée rousse n'a gorgui bak waye li wourou la dalll kon ngua bayi thi Khel boubakh ngua diegeulmanak bou bakh waye li wourou guiss louma lerr ma wakh ko rekk la deff

  • @breezybrown6940
    @breezybrown6940 6 лет назад

    yaw seringe moustapha sy bou xamoul seringe cheikh Ahmed tiadiani sy rta Kane moko xame te seringe cheikh tok wax lime wax seringe moustapha sy nianalko sante ko seringe moustapha sy di firile nite gni waxi seringe cheikh sac gamou bayil tonge ahahahah fen rek ngaye def

  • @ndiagandoye8074
    @ndiagandoye8074 6 лет назад

    Ki mom moy kan meussomako guiss si waxtan si sgn cheikh

  • @ndiagandoye8074
    @ndiagandoye8074 6 лет назад

    Yén yi ignan lay done sax

  • @mallbelly8250
    @mallbelly8250 4 года назад

    Abdou sy sokhor mo la diapou

  • @queenfa6915
    @queenfa6915 6 лет назад +3

    Yaw nak war nga holate sa bopp... vidéos Serigne cheikh yimouye wakh si Serigne Moustapha gnigui fi dé...buzz ngaye wout kéne hamoula

    • @doumbouyaabou4563
      @doumbouyaabou4563 4 года назад

      toi tu n'as rien compris ay cheitané nguen rek yaw ak moustapha yeup

  • @khadimdiakhoumpa8955
    @khadimdiakhoumpa8955 6 лет назад

    Sa kholl dafa sokhorr demall ga fadioudjii garson domii kharmmmmm nimoro 1

  • @tafcotica4816
    @tafcotica4816 7 лет назад

    doye'na'war

  • @bigmen4204
    @bigmen4204 6 лет назад +1

    haha ku yabou geume sa borom tè dèf nank si seurignu tèèy yii
    lii doynar war torop

  • @abdoulayegaye5570
    @abdoulayegaye5570 7 лет назад +7

    Ki dara lafi wakhoul mai serigne cheikh nena ma serigne pape malick na kham boopam lolou kaay dafa nekh si khool ndakh mooy moom kilifa guide la donc dafa am aay naw lé youmou wara andal mane dee nonou lako guisse mangui diégalou nak

    • @boudabaax8177
      @boudabaax8177 7 лет назад +1

      abdoulaye gaye nga baal ma mais bul wax ni kii dara lafi waxul. ndax niaaw na loolu. serigne Abdou mii kilifa la té doomu serigne Cheikh la. Kon en tant que Taalibé nous lui devons respect.
      entre moom ak ak magam serigne Moustapha nioun waru niou ci am beneu par parlo... wa salaam

    • @abdoulayegaye5570
      @abdoulayegaye5570 7 лет назад +2

      D accord mai anna soutoura lengui pourkw serigne bimou khamé serigne moustapha peut etre defoul yone moo deme keureum ou bien mou wooko telephone gnou regler lep si diam ak salam si soutoura mai publikma lolou bakhoul il faut am kou tané moromam

    • @sen2287
      @sen2287 7 лет назад

      abdoulaye gaye Moustapha Sy mo am soutoureu xamnaa? Boulniou takha waxx. Moustapha amoul benn respect si bayam yi. Motaxiitt benn rakam dou am respect si moom.

    • @boudabaax8177
      @boudabaax8177 7 лет назад

      En tous cas je ne cherche pas à créer la polémique. Mais li leer ba leer moy daal nous en tant que Taalibé daal danio leen wara yemalé bayi par parlo bi. té mandou ba paré sax ci nek taalibé rek nak!

    • @hamdrew8515
      @hamdrew8515 7 лет назад

      5 ans ?

  • @khalilsow9572
    @khalilsow9572 7 лет назад +4

    ABDOU SY DIEUREUDIEUF LERAL NGA LOU DIARA LERAL NDAKH LI SOU DAKKOUL DAFAY YAKH DAROU KEYR GUI

    • @safietoucisse261
      @safietoucisse261 7 лет назад

      Khalil Sow Serigne Moustapha daléna gueune douléral mais bavardage

    • @ousseynouniang6550
      @ousseynouniang6550 7 лет назад

      C ça que tu appel leral ? Sosal weuy arrêtez de vous voilé la face

    • @ousseynouniang6550
      @ousseynouniang6550 7 лет назад +1

      Serigne Moustapha point

    • @seynaboufall3039
      @seynaboufall3039 6 лет назад

      Abdou sy kawma amgalou la méti.yaw louka deklou sakh pass passam si keurgui roote affaire famille ne se règle pas entre les média. Et tu étais ou toi ? Tu cherche à divisé la famille .tall Bou yala talllldoli mateur mo gueun ligueye déf.lhistoire se répète .mbolom kéna douko ouut. manoulo wakh dara si sougnou mame cheikh .lougnou que weydiour ak mame cheikh gnodoonne Andeu. Laisse serine moustapha sy et règle tes problèmes . santeu sy takhoul gua gueun gnou ko diégué.

    • @seynaboufall3039
      @seynaboufall3039 6 лет назад

      Dieureudieuf il a des problèmes c' est des paroles de règlement de comptes en tout cas il n a rien de lougnou mame.

  • @pepelebusinessmanndanane6678
    @pepelebusinessmanndanane6678 4 года назад

    Babacar fall yaw domou kharam ga rek toukhe katou yamba bii
    Abdou sy douniou la wakhe dara ndakhe mame cheikh .
    Wayé kén khamoula fonékon bi seringe kheikh sokhla

  • @mallbelly8250
    @mallbelly8250 4 года назад

    Dangua taerde rek

  • @D.A.L_Tv_office_1
    @D.A.L_Tv_office_1 7 лет назад

    mais serigne lane lafi wakh lou ay

  • @khalilsow9572
    @khalilsow9572 7 лет назад

    safietou comprendrouma linga beugueu wakh

    • @mounassedieng5263
      @mounassedieng5263 7 лет назад

      Serigne yi svp le linge sale se lave en famille soutouralen sen keur yii

  • @ndeyeseck1632
    @ndeyeseck1632 7 лет назад

    Abdou Sy bi serigne Cheikh di wah serigne Moustapha nan ko yay chef de guerre yay grand patron bobou fo nékon??????

    • @nafissatougassama210
      @nafissatougassama210 6 лет назад +1

      Walahi moma diakhal mane fane lanékone Sérigne Moustapha Sy thiacaw thicanam

  • @babacar315
    @babacar315 7 лет назад

    L'histoire se répète. Les premiers ennemis du prophète Youssouf étaient ses frères.
    Pourtant Youssouf était l'héritier de Jacob.Il était aussi les plus nobles des fils de Jacob.
    Serigne Cheikh a dit publiquement Serigne Moustapha tu as des ennemis tellement dangereux, des ennemis tellement malhonnêtes''
    Serigne cheikh a dit publiquement à saint Louis '' Serigne Moustaph ,saggal nguama Yallana Yalla saggal la,Térral nguama Yallana Yalla Térral''.
    Ce même Serigne cheikh a dit Serigne Moustapha c'est votre responsable moral ,c'est votre chef de guerre ,c'est votre grand patron.
    Acceptons le destin.Serigne Moustapha est un élu de Dieu.

  • @khadimdiakhoumpa8955
    @khadimdiakhoumpa8955 6 лет назад

    Sa kholl dafa sokhorr demall ga fadioudjii garson domii kharmmmmm nimoro 1