Machallah dieureudieuf pape Momar yalla na la yalla dollè wèrral tè goudale sa fann???kèp kou and ak maky si 3"" manda yalla na la yalla torrokhal bala 2024 amine
Macha Allah dieureudieuf serigne bi diagne nar li dee lañuy xar sii kilifa yalna sunu borom swa saamlah sutur'alah defalah tawfekh thii daradjia yonente bi swas
Merci Macha allah wakh bi rafetna, waayè li nga fatè rèk moy Auto Macky Sall paana si tally yoyou ngay wakh, gñioun gñi gñiowna toog ak gñioun fi si Amérique gñiou wakho lounèh mom ak Ablaye Wade yèp mais Africain mo diaroul darra…Deuxième point bi moy, khana khaliss bigñiouy yak si ay ziarra aki gamou aki magal pour lan? Tè ay milliard you barri lagñiouy yak diap nit ay ottage meuno dèm fèn so amè malade sah do kham foy diaar pour yobouko hopital ndakh talli yigñiou barrè…waayè population bi mèritangñko tamit ndak Côme que gñioulèèn di nakh rèk lagñ beug…khèl mom amougñiouko. Entoucas merci ❤
Djieureudieuf diagne yalla nala yalla faye walaakhi loo wakh rék amna lou dess gouvernement Senegal gnooy gouvernement bii gueneu yeess ci monde dougnou sakh rouss
Serigne Momar est un homme généreux et rare dans sa société. Si on en avait 14 dans ce pays le pays ira forcément mieux. Mais dommage pour le Sénégal malade de ses dirigeants.
Papa dila nianal goud fan ak wer inchallah beugon nala déjà té xamouma won sax fo deuk rawatina tay bima xamé ni louga la Machallah yallah nala souniou borom sameu ak sa ndiabot yeup❤️🙏🏾
Merci encore à vous Serigne Momar il est heureux de vous compter parmi nous Vos interventions comme celle de l'éminent professeur Note augurent des lendemains meilleurs pour notre peuple que Dieu vous garde
MERCI S. MOMAR DE NOUS (SENEGALAIS) ,DE NOUS RAPPELER QUE, ET QUELQUE SOIT LE SENTIMENT QUE L'ON RESSENTE, IL Y'A BIEN DES LIMITES K LA DIGNITE HUMAINE IMPOSE A LA SOUMISSION DU COEUR LE PLUS EPRIS ET LE PLUS PATIENT C'EST TRISTE, MAIS BIEN LA REALITE SAMA GAYI DAL GNI NGUI CI WALLY, GRD U, PAWLISH, UZIN KEITA,.......
MASHA ALLAH papa mais nioune nak loune niou def dagane nioko nangou gni geuneu sonou si réw Macky Sall laniy votél li geuneu méti moy comme ay khalé you ndaw pour niom lilén état bi di défal si sén poche la khamouniou ni état limou yoré nio koko diokh mane dh tolou na fo kham ni mana touma wakh tane ak samay parents si lou dieum si rééw mii parce que khol bou nakhari rék lassiy andal 😢
Vous avez parfaitement raison Papa je viens de voir les images à la télé, j'étais tellement triste, moi qui après Dakar, Louga est la région que je connais le mieux. Mais cette population mérite t-elle qu'on ait pitié d'elle ?
Salamou Aleykoum les sénégalais n'ont pas de dignité. Aucun autre peuple n'accepte se qui se passe au Sénégal. Le 3ème mandat ça devrait même être une chose mentionnable. Il se faire respecter. Même des femmes se revoltent devant l'état iranien. Tous les peuples souverains se sont battus. On ne peut pas faire d'omelette sans casser les œufs. Lou waye ame moko maye bopame. Hasbouna lahou wa nihmal wakil qu'Allah protège le Sénégal. Amine. Salamou Aleykoum
Same cheat since 1960.kel pays ! Kel pays..Boumou jaam la Sénégalais yi Nek .Toklen Foffou. Di Wakh Rek .akka khole .thank you Imam.Thank you..ya k la merde ds ce pays . Rien D' autres …93
Salam Serigne Momar je ne varie pas sur ma position sur votre engagement pour le Sénégal. Je vais simplement ajouter que la situation que nous vivons est sous la houlette des chefs religieux qui sont en connivence avec Macky Sall.
@@awaba3307 Baraka ALLAHOU fikoum ma chère sœur. Et c'est la pure vérité. Des guides religieux qui ont peur de dire la vérité. C'est qui est triste, c'est de constater que des sénégalais continuent à les vénérer.
Macky Sall est indigne de la fonction de Président de la République. Dans un pays sérieux Macky Sall n'aurait même pas dirigé un troupeau de chèvres 🐐 🐐 🐐
Salam sounou papa yalna Yallah goudal sa fane baliniou name ci SÉNÉGAL MOU AM .LIGAY WAKH LOU DIARA BAY KHEL LA,MACHALLAH
Monsieur Diagne que le bon Dieu vous bénisse !
J'apprécie beaucoup vos vidéos et je vous souhaite une longue vie.
Que Dieu vous garde !
Heureusement pour mon cher pays. Nous avons des sauveurs .Que le Tout puissant vous guide.
Sama bayou bopou yalnala yalla samou
Amine ya Rabbi
Machallah dieureudieuf pape Momar yalla na la yalla dollè wèrral tè goudale sa fann???kèp kou and ak maky si 3"" manda yalla na la yalla torrokhal bala 2024 amine
Amine ya Rabbi
Vérités absolues,mon Papa merci bcp .
Dieureudieuf Seringnebi, tu es un des rares gens qui osent dire la vérité
Assalamou hanlaykoum macha allah yalnala yala lakhe fa yakhe yégoul si daradiaye yonentibi seydina Mouhamad salalahou hanlayhi wa Salam dieuredieuf
Macha Allah dieureudieuf serigne bi diagne nar li dee lañuy xar sii kilifa yalna sunu borom swa saamlah sutur'alah defalah tawfekh thii daradjia yonente bi swas
Respects, je partage pour massifier les enseignements 👉🏽nako ñièppeu djieuufé
Djieureudjieuf 🙏🏽
Machalaa man louga laa deukeu lou leer guawakh
Yalna sa diame yague papa
Choukrane papa. Dëug, Dëug akk soukk lagnou
Dieuredieuf diagneenbi yalnayaala fayla
Merci papa yallah nga yagfi teweurr
Longue vie papa🤲 Amine
MachaAllah yallah kassé mofi nék.
Allah Akbar lolou dou louga rek la am. Depuis Senghor lolo xew bir Sénégal
Machalah yala nala yala féy yiiw
Au moins il reste des gens dignes dans ce pays
Merci Macha allah wakh bi rafetna, waayè li nga fatè rèk moy Auto Macky Sall paana si tally yoyou ngay wakh, gñioun gñi gñiowna toog ak gñioun fi si Amérique gñiou wakho lounèh mom ak Ablaye Wade yèp mais Africain mo diaroul darra…Deuxième point bi moy, khana khaliss bigñiouy yak si ay ziarra aki gamou aki magal pour lan? Tè ay milliard you barri lagñiouy yak diap nit ay ottage meuno dèm fèn so amè malade sah do kham foy diaar pour yobouko hopital ndakh talli yigñiou barrè…waayè population bi mèritangñko tamit ndak Côme que gñioulèèn di nakh rèk lagñ beug…khèl mom amougñiouko. Entoucas merci ❤
Merci beaucoup mon frère pour cette analyse pertinente
Djieureudieuf diagne yalla nala yalla faye walaakhi loo wakh rék amna lou dess gouvernement Senegal gnooy gouvernement bii gueneu yeess ci monde dougnou sakh rouss
Serigne Momar est un homme généreux et rare dans sa société. Si on en avait 14 dans ce pays le pays ira forcément mieux. Mais dommage pour le Sénégal malade de ses dirigeants.
Le Sénégal est aussi malade de ses guides religieux
Papa dila nianal goud fan ak wer inchallah beugon nala déjà té xamouma won sax fo deuk rawatina tay bima xamé ni louga la Machallah yallah nala souniou borom sameu ak sa ndiabot yeup❤️🙏🏾
Billakhi papa contanena thi dioulite degua ..machallah yalla nassafane guoune..yaguale lafii
Ma chahalla amna solo degatina degue amine
Sama pape yalnala yalla taxawou sayuma xeuyé sa vidéo laye xare
Yalla na yalla Goudeul sa fan
Amine yarabal alamine Amine Ame na solo Machallah
machàallah jërëjëfati
Merci encore à vous Serigne Momar il est heureux de vous compter parmi nous Vos interventions comme celle de l'éminent professeur Note augurent des lendemains meilleurs pour notre peuple que Dieu vous garde
Je veux parler de l'éminent professeur Kader Boye Macha Allah
Jeurejeufati Diagne ca taxaway rafètna
السلام عليك يا شيخ بارك الله فيك أطال الله عمرك بسر وأماماينفع الناس فيمكث في الأرض
Machala amatina solo dieureudieuf serigne momar diagne en tout ca 3e manda pour macky béne senegalais warouko nanguou diar na dé ba diékh tak
Merci beaucoup Machallah Amna solo ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ love you 😘
Ndax yalla jerejef yallna brome gudal safane amna solo
Merci mon père tu dit la vérité rien que la vérité par l'amour 💕 de dieu le Sénégal 🇸🇳 à besoin de toi
Diereu dieuf papa yalna gna goudou fane ak wér 😍
Merci momar vérité absolue ragual dou déme kharé yalnagnou yallah défal jiamm
MERCI S. MOMAR DE NOUS (SENEGALAIS) ,DE NOUS RAPPELER QUE,
ET QUELQUE SOIT LE SENTIMENT QUE L'ON RESSENTE, IL Y'A BIEN DES LIMITES K LA DIGNITE HUMAINE IMPOSE A LA SOUMISSION DU COEUR LE PLUS EPRIS ET LE PLUS PATIENT
C'EST TRISTE, MAIS BIEN LA REALITE
SAMA GAYI DAL GNI NGUI CI WALLY, GRD U, PAWLISH, UZIN KEITA,.......
كلمات الحق أيضا من أبينا الشيخ ممر انجاج
حياك الله ونصرك وأطال وبارك عمرك ورزقك امتثال أوامره واجتناب نواهه إلى آخر عمرك
Walahi papa lépo Dega li Moy Sénégal
Machalla yaw mom do wakhantou degue rek ngay wax
Papa nioun fi fouta Macky niawnafi campagne 2011 niou nianko tali ba legui gissouniou Dara wante ba 2024inchallah Dina laire
Merci pour votre Constance que la protection divine vous accompagne longue vie imam
Salam Salam Baye Momar Deug rekk nguay wakhe Masha Allah Dieureudieuf 🙏🙏🙏🙏💞🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Bilakhi papa gni dougnou gnou bakhe
Dieureudieuf Serigne Diagne yallah nala yallah sameu
Amatina solo papeuh walay nioun daano sonnou si macky mi akki thiaakhanam
Merci beaucoup mon père je te suivre depuis dans la frontière entre senegal et Guinée-Bissau
Dieuredieuf papa
Encore une fois jerejef sama Serigne
Jërëjëf sonn nga de.
Sénégal d'où réw Rewoum Nafikh Corrompus Rk Motakh Réwmi d'où avancer jamais
Amine🙏 Machalla wakh bi ame na soloo yallah na Yallah yok kham kham bi yok wèreu
Merci beaucoup serigne bi
Amna Solo
Dieuredieuf dieuredieuf dieuredieuf
Dieureureuf Serigne momar diagne.mashala
Dieuredieuf machalah❤❤❤ pour le courage et les vérités
Merci bcp notre pér 🙏🙏🙏
Macky sall gnoka gueune feep, mais badoola keena dou ko yeela. Jeureujeuf gorgui
Amna solo lool
Dieuredieuf yalnala yala sameu
Machalla papa
MASHA ALLAH papa mais nioune nak loune niou def dagane nioko nangou gni geuneu sonou si réw Macky Sall laniy votél li geuneu méti moy comme ay khalé you ndaw pour niom lilén état bi di défal si sén poche la khamouniou ni état limou yoré nio koko diokh mane dh tolou na fo kham ni mana touma wakh tane ak samay parents si lou dieum si rééw mii parce que khol bou nakhari rék lassiy andal 😢
Wallahi mon frère Momar Talla tu as parfaitement raison
Jeureujeuf serigne Momar. Senegal defar ko dina metti torop. In Shaa Allah ndam dina am
Amine ya Rabbi
Ndam d'où am ci deukou tapettes hypocrites malhonnête AK lâches.chaque peuple à les dirigeants qu'il mérite
Dieureudieuf
Merciii mon père.
C'est votre meilleure intervention à mon avis.
khekh rek la maky sall kham
Machalla Machalla Machalla
Vérités absolu serigne bi
Merci Diagne narr
Vremea mane je me suis dit esk les vidéos que j'ai vue sur les rues de Louga esk c'est vrai
Dousi ngioune yallaha moko feff mem dou maky rek président bounekla
Je pense que dans la vie il faut dire la vérité quand il faut.Il faut être honnête envers soi-même et devant Allah. Merci de votre vérité.
c'est la mème tricherie a TAMBACOUNDA, quand Macky devrait venir on a parait la ville comme une mariee qui doit rejoindre son mari
Vous avez parfaitement raison Papa je viens de voir les images à la télé, j'étais tellement triste, moi qui après Dakar, Louga est la région que je connais le mieux.
Mais cette population mérite t-elle qu'on ait pitié d'elle ?
DIEURDIEUF
Ngourou peul sathie ak diaye dole kepp
Vous êtes un vrai patriote, un patriote éclairé.
Masha Allah Alhamdulilah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Salamou Aleykoum les sénégalais n'ont pas de dignité. Aucun autre peuple n'accepte se qui se passe au Sénégal.
Le 3ème mandat ça devrait même être une chose mentionnable.
Il se faire respecter. Même des femmes se revoltent devant l'état iranien.
Tous les peuples souverains se sont battus. On ne peut pas faire d'omelette sans casser les œufs.
Lou waye ame moko maye bopame.
Hasbouna lahou wa nihmal wakil qu'Allah protège le Sénégal. Amine.
Salamou Aleykoum
Dieredieuf. Ça a toujours été comme ça au Sénégal. C'est comme si le peuple est serviteur du président et pas le contraire. Sénégalais begul bopam
La confrontation est inévitable. Ne vous en faites pas nous sommes prêts. Pas de 3ieme mandat
Babacar Wally Algérie merci beaucoup pour votre retour
Merci diagne amna solo
Ámine inchalla
Merci beaucoup
Dafa diote sénégalais yi yewou
Louga doive cree telethon pour la renovation avec un contentieux
Merci beaucoup papa
Same cheat since 1960.kel pays ! Kel pays..Boumou jaam la Sénégalais yi Nek .Toklen Foffou. Di Wakh Rek .akka khole .thank you Imam.Thank you..ya k la merde ds ce pays . Rien D' autres …93
Bilaye population des foi sakh dagalendi mere
C est vraiment très triste
Yalana souniou borome faye
Amiin
LONGUE VIE À VOUS
Salam Serigne Momar je ne varie pas sur ma position sur votre engagement pour le Sénégal.
Je vais simplement ajouter que la situation que nous vivons est sous la houlette des chefs religieux qui sont en connivence avec Macky Sall.
Les marabouts ne sont là que pour leurs intérêts. Que les sénégalais se réveillent.
@@abdoulayeba7078 merci tu as tout dit
@@awaba3307 Baraka ALLAHOU fikoum ma chère sœur. Et c'est la pure vérité. Des guides religieux qui ont peur de dire la vérité. C'est qui est triste, c'est de constater que des sénégalais continuent à les vénérer.
@@abdoulayeba7078 ils sont les premiers complices des politiques ques ces maraboutuquiers
@@fraterniteetpaix8597 Wallahi tu as parfaitement raison. Tout à fait d'accord avec toi
شكرا يا شيخ
Macky Sall n'a pas les qualities d'un president
Macky Sall est indigne de la fonction de Président de la République. Dans un pays sérieux Macky Sall n'aurait même pas dirigé un troupeau de chèvres 🐐 🐐 🐐