yalla yalla yi lignouy bagn ba plainte moom la moussa diagne nekke ak dioullit gni

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 24 янв 2025

Комментарии • 95

  • @serignefallouthiobane6378
    @serignefallouthiobane6378 16 дней назад +3

    Héé thiey yalla . 😢 Yalla nako yalla guindi

  • @NgoneColy-li6sq
    @NgoneColy-li6sq 15 дней назад

    Dieureudieuf Imam yalna na takhaway wi yague Sénégal nak dîné dafer toumouranké Assalamou Aleikoum

  • @fantastique1731
    @fantastique1731 16 дней назад +6

    Aouzou billahi mina cheytané radijm.

  • @aronadiop4853
    @aronadiop4853 13 дней назад +1

    Ndialo katt yi, joueur Xber yi, nafeek yi nio nékeu di clash yalla yalla yi.
    Santé cheikh moussa rek

    • @ibrahimakane6233
      @ibrahimakane6233 13 дней назад

      Ya lene guiss niouy ndialo? Wayer ni rek ngene mana mel.
      Ko sa serigne fi sagaa alkhourane ak yonenetebi moss bo toumaler ay gor dou niou bett

  • @mamecheikhndiaye601
    @mamecheikhndiaye601 17 дней назад +3

    Yalna niou yalla yereum si wakh diou reuye dji te niaaw Dieuradieuf Serigne Momar Diagne Yalna sa Takhawaye Yague Lol si dine dji

  • @hamadygassama3620
    @hamadygassama3620 16 дней назад +2

    Ma cha Allah dieureudieuf sama serigne yana nga fi yague té wer ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @yeguebonysamba9421
    @yeguebonysamba9421 17 дней назад +4

    Ma ShaAllah yalna nga fi yagg té weur

  • @thianendiaye6363
    @thianendiaye6363 17 дней назад +2

    Sama Serigne magui ziar dila massawou thi thiono bi ngaye dadj thi diner bi yalna la yala are thi Barker SWT Amine ❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤

  • @guelewargueye3393
    @guelewargueye3393 17 дней назад +7

    Tout notre soutien

  • @mamadoufaye9962
    @mamadoufaye9962 17 дней назад +3

    Soubhanala moussa diagne dé kouko geuna yess amoul ki moye ab khadj senegal dafa am nio khamné danioulrna bayi si louléne nekh rek bamou eupi lokho wayè nag setane gui mo eupou diadieufaty papa serigne momar diagne wakha tinga degue rewmi dal li serigne cheikh sy almaktom done wakh rek moye degue senegal khawma loufi am wayè dou justice dafa lo khamné waroul am si rew mou am justice wayè naniou dem rek

  • @MohamedlamineNdiaye-w8z
    @MohamedlamineNdiaye-w8z 17 дней назад +1

    Jàmm ci yaw inchallah Serigne Momar Diagne Sénégal 🇸🇳 ca kanam inchallah

  • @momosy6083
    @momosy6083 17 дней назад +2

    Si rére bou graw laniou nek les yallah yallah sama grand frère si la nékon avant

    • @ibrahimandiaye5595
      @ibrahimandiaye5595 16 дней назад

      Linga wax wéroul yawmi ya nékk si rére ak ngeulmandé gou doy war, kou weddi yalla yalla yi diamono bou yonnent yalla Mohamed nieuwatone nga weddi ko, islam laniou amé nioune yalla yalla yi, nio nékk si lou nékh yalla

  • @moustaphaniang985
    @moustaphaniang985 17 дней назад +3

    Wakkh dji niaawna ba diégui dayo 😢😢 té niak ay téguine

  • @Is_124
    @Is_124 17 дней назад +3

    Tarikha c.est dure a dire mais dfa diekh Sénégal parceque loumouy yakeu si souniou diamono nioune mo eupeu loumouy defar danio wara delou nioune nieupeu si yonnente bi saw beneu yone

  • @cheikndiaye2552
    @cheikndiaye2552 17 дней назад +3

    Toute notour soutin avec s. Mamar diange

  • @MamadouSENE-ku3fw
    @MamadouSENE-ku3fw 17 дней назад

    Ma chala amna solo serigne DIAGNE dieureudieufeuty

  • @PapamodricDiatta
    @PapamodricDiatta 17 дней назад +3

    Machallah je suis contente avec toi papa Serigne mamor

  • @adamandiaye1965
    @adamandiaye1965 16 дней назад

    Dieureudieuf yana nga fi yague té wer ❤❤❤❤❤❤❤

  • @Salimata1000
    @Salimata1000 17 дней назад +4

    Dagnouye diaye fiit au meuneu fène ci diiné Islam,mais le jour du grand rassemblement devant Allah swt,ils verront et sauront que tout est vrai In Shaa Allah.

    • @blacknegro7408
      @blacknegro7408 16 дней назад

      Gni kégn dagnio boone torop sakh ay nitou iblis lagniou

  • @sowyoussouf2892
    @sowyoussouf2892 16 дней назад

    Yalla na la yalla defale diam akhewale

  • @SyAlassane-k7s
    @SyAlassane-k7s 13 дней назад +1

    Wallahi deugla

  • @moustaphaniang985
    @moustaphaniang985 17 дней назад +4

    Dieureudieuf gorgui défendre nga dîner l'islam ak deugue

  • @kananthiouladiatta151
    @kananthiouladiatta151 16 дней назад

    Serigne Momar Diagne, j'ai vraiment peur de ces gens comme Moussa Diagne.

  • @dionemoustafa1171
    @dionemoustafa1171 16 дней назад

    Kou wakh lolou wakhoul deug dieuredeuff ndiagñe

  • @baboucargoudiaby2933
    @baboucargoudiaby2933 17 дней назад +8

    Ou est jamra et and Sam djiko

  • @mbathiosow1721
    @mbathiosow1721 17 дней назад +2

    استغفر الله العظيم 😢

  • @modousall-ht9ke
    @modousall-ht9ke 17 дней назад +1

    Machallah amna solo ❤

  • @groupenabiyetv8211
    @groupenabiyetv8211 16 дней назад

    Non ahmed fall nak mom day wéré de mom😢😢

  • @ibrahimandiaye5595
    @ibrahimandiaye5595 16 дней назад

    Baye momar diagne damalay topou dila déglou, di rafet lou say vidéo amna solo lol
    wayé mbiroum yalla yalla déf si ndankeu, teukouwouma déh, mais damalay layé biir, ndax diné islam diné layanté bir la, mane déh yalla yalla la, té reuthiouwouma loumasi dougué parce que xamxam rék mofa nékk,
    wayé nénga déglou nga cheikh Moussa Cissé niambé darou moy souniou serigne, mom serigne touba moy serigneum, li yalla yalla di wax lolou moy deugg té mo soss koulou tarikha.
    Tarikha boufa ague si yalla amoul, xam yalla amoul, Guiss yalla amoul, nane ko wowé nénéne bamou déss tarikha.
    Serigne Touba, el Hadji Malick, Ibrahima Niass, limamou laye goor yalla yeupou xamxamou tasawouf laniou wotté wone, té moy xamxam boulay dieulé thi sirkou bilahi (bokalé yalla) dila yobou si wéteul yalla (tawkhitoul ilahiya) kone naniou déf attention si yalla yalla yi, walahi si deug laniou nékk.
    weddi Guiss bokousi, cheikh Moussa Cissé niambé darou day wané yalla dieukhreune ak beuti bopou

    • @naar9102
      @naar9102 16 дней назад

      Yaw may gnou diam thi thiakhane rék ak bokkalé ngène nék domérame yi

  • @modoudrame3715
    @modoudrame3715 3 дня назад

    Moussa diagne dof lue

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 16 дней назад

    Koufi saagaati Lislaam ma porté la plainte.

  • @dieuseueldieuunik7693
    @dieuseueldieuunik7693 16 дней назад

    Yalla Nanou yalla tek si yonou siratal Moustakhim

  • @salieumbai810
    @salieumbai810 16 дней назад

    Nafekh mo bari Senegal

  • @CheikhGueye-n7f
    @CheikhGueye-n7f 17 дней назад +3

    Moussa diagne dafa rew

  • @fatoumatabintoucolley8878
    @fatoumatabintoucolley8878 17 дней назад +3

    Senegal mo beuri nafekh boudon Sering Touba lagn wakh lii Cheikh bara melni moy ange gardien wam ak mouride yi niom dègn yakar nii dine leup sering touba leu

    • @mamadounallaba9495
      @mamadounallaba9495 16 дней назад

      Lii dh Kouko wahe Serigne Touba do fanane dh maala wah lii. Yalla naniou yalla yéreum. Amine

  • @baboucargoudiaby2933
    @baboucargoudiaby2933 17 дней назад +2

    Amou niou kham kham Di leurrer les gens

  • @paapnjaay1586
    @paapnjaay1586 16 дней назад

    Lépp-lépp tarixa yi la rek. Fiiwak tarixa jógu fi wax ju ëpp du fi jóg. Bu tarixa baaxoon sax li muy alag ciy nit war naa tax ñu wan ko ganaaw sakkantumaak ba mu bókkulee ci diiné ji.

  • @MaussaDiop
    @MaussaDiop 17 дней назад

    diazàkallàhou khayra❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bintourabykeita8430
    @bintourabykeita8430 16 дней назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @SiradjiMbodj
    @SiradjiMbodj 17 дней назад +1

    ماشاءلله

  • @JOTALIREC
    @JOTALIREC 17 дней назад +2

    néél fén kat bi kay wadji mo gnamé yalla ta mana fén

  • @davembow6020
    @davembow6020 16 дней назад

    Walahi limou walh amena

  • @PapamodricDiatta
    @PapamodricDiatta 17 дней назад +1

    Bouniou bayil kene Serigne nio dak wakh lou amoul ci diine

  • @ndiogoufall6462
    @ndiogoufall6462 16 дней назад

    Diagne la santa dh

  • @nafizadamie3821
    @nafizadamie3821 17 дней назад +2

    😭😭😭😭

  • @mossandiaye6893
    @mossandiaye6893 17 дней назад +1

    Dinéy senegal sén tarikhayi nioko yakhe tarikhaya yo khamni féni késsé

  • @KhadijaDiouf-g1f
    @KhadijaDiouf-g1f 16 дней назад

    Sénégal dal sii ibadou lagnou sawar .
    Groupe de personnes biii porté wone plainte Omar Sall anignou
    Yén lagnouy déklou

  • @laminembengue3443
    @laminembengue3443 17 дней назад

    Apres on viendra nous parler de "nos" chefs religieux 😢

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 16 дней назад

    La direction des affaires religieuses ne sera que confrérique et pas correctionnelle.

  • @Lil_mustafa
    @Lil_mustafa 16 дней назад

    Direction bobou am ngafa place dh, sama baay

  • @serigneadj1779
    @serigneadj1779 16 дней назад

    🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • @freemind3009
    @freemind3009 17 дней назад

    je suis d'accord avec le gars dans l'audio sur une chose: Dineji amoul kilifeu. C'est vrai, la religion est une affaire personnelle et individuelle.

    • @blacknegro7408
      @blacknegro7408 16 дней назад

      C'est pas vrai ce que tu dis dinné bi am na kilifeu moy Seydina Mouhamed PSL niak nién téguin torop ak yabaté

  • @seexxunaadaraame6809
    @seexxunaadaraame6809 17 дней назад +3

    Cëy wax jii ab jullit waru koo wax.

    • @moustaphaniang985
      @moustaphaniang985 17 дней назад

      Bilahi

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 17 дней назад +1

      Sant Sunu Borom 🙏, bouma bokoul ci bène TARIQA ☹️; trop de dérapages 😢

  • @TandjigoraHarouna
    @TandjigoraHarouna 17 дней назад

    واضح ما شاء الله 👌

  • @Fatima-ph4vn
    @Fatima-ph4vn 17 дней назад

    Soubhanallah

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 16 дней назад

    Les khalifs deraient être les garants de l'Islam et il n'en sont conscients. Ils ne gèrent que leurs Tariiqas.

  • @mamadoundaye9797
    @mamadoundaye9797 17 дней назад +3

    yaw Gorgui ni douñou ahy nite

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 17 дней назад +1

      Sant Sunu Borom 🙏, bouma bokoul ci bène TARIQA ☹️; trop de dérapages 😢

  • @cheikhsalaan9205
    @cheikhsalaan9205 17 дней назад +3

    Li ndé magui koy soga ndég ki day fén rk

  • @mayorodia7770
    @mayorodia7770 17 дней назад +2

    Ces gens ne sont pas des Yallah Yalah, mais des Non-Yallah Non-Yallah.
    Ils se réclament de quelle confrérie?
    Cette confrérie doit réagir nakkkk.
    Mais les confréries moom mooy loolou!!1 Les adeptes défendent seulement leurs marabouts ou gourous. Elles défendent pas Dieu, ni le prophète (psl), ni l'Islam, ni le Coran.... rien.

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 17 дней назад +1

      Sant Sunu Borom 🙏, bouma bokoul ci bène TARIQA ☹️; trop de dérapages 😢

  • @ablayekasse7667
    @ablayekasse7667 17 дней назад +1

    Deuk bi dale menga fénal yonent bi wakhal ko lou bone té daradoula si fék wayé bo toudé serigne do fanan sa keur ligua wakh moy deug islam da toumeranké si deuk bi

  • @aronadiop4853
    @aronadiop4853 13 дней назад

    Mais c'est pas Moussa Diagne dans cet audio. Yangui togn dh
    Et qui te dit que c'est un Yalla Yalla

  • @cheikhahmadoubambadiagne-j7d
    @cheikhahmadoubambadiagne-j7d 17 дней назад

    Moussa diagne omar diagne madiambale diagne vous n'honorez pas le noble patronyme DIAGNE.

  • @serignesarr2649
    @serignesarr2649 17 дней назад

    قلت العلم وضعف العقل وحكايات غير إسناد ولا دليل نعوذ بالله من ضال مضل

  • @mamadousy6312
    @mamadousy6312 17 дней назад +6

    Li moy danger tarikha thi rew il provoque la colère d allah chaque jour

    • @mortallafall6825
      @mortallafall6825 17 дней назад

      Quelle idiotie !!!

    • @mortallafall6825
      @mortallafall6825 17 дней назад

      È tu te tait quand les champions du monde de récital coranique Viennent de TARIQA ???!!!

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 17 дней назад

      Sant Sunu Borom 🙏, bouma bokoul ci bène TARIQA ☹️; trop de dérapages 😢

    • @mamadousy6312
      @mamadousy6312 17 дней назад

      @@mortallafall6825 les champions du monde son pour tout en récitant le coran li nga wakh dou argument 😂🤣😂

    • @ndongobaye561
      @ndongobaye561 17 дней назад

      Iow dof deug nga, soula beneu nite togné daw dugue si mbollo ndah dagay ray mbollo mi yeupe ?

  • @SkarimmaysaraFall
    @SkarimmaysaraFall 17 дней назад +1

    kii reew na

  • @abdoulay2867
    @abdoulay2867 17 дней назад

    "ses paroles"contiennent quel sens et il sait lui-même qu'il ment.

  • @samsoukhouma
    @samsoukhouma 17 дней назад

    C ahmed cisse da amol won mbolo rek

  • @raulmarceldepoter7170
    @raulmarceldepoter7170 17 дней назад

    Vérité absolue et ils insultent la charia chaque jour et moustapha sarr a divulgué leur secret qu'ils cachent depuis des années

  • @mouhamethmbacke7272
    @mouhamethmbacke7272 16 дней назад

    قصة الإسرائيليات إن هي إلاكذب

  • @famathiam9948
    @famathiam9948 17 дней назад

    Ki meune na wah lou amul di moussa mi hana yako feké linga wakh nii deh yako gneuka wah

  • @alassanesy2768
    @alassanesy2768 17 дней назад +2

    C’est des malade manteau

  • @samsoukhouma
    @samsoukhouma 17 дней назад +1

    Ana ñi plainte won c ahmed cisse wala li da grawol . Wala imamyi ño porte won plainte

  • @absaduop7965
    @absaduop7965 16 дней назад

    Nouveau Diné yabatè

  • @salioungom9557
    @salioungom9557 16 дней назад

    😢😢😢😢😢😢

  • @BadianeBaba-h2l
    @BadianeBaba-h2l 17 дней назад

    😭😭😭😭😭