Daaju Mag Gni | Khassida Matlaboul chifai (Par S. Abdou Diouf)

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 14 янв 2025

Комментарии • 733

  • @malickhanne5740
    @malickhanne5740 9 месяцев назад +40

    Je me pointe encore en 2024 in sha Allah je pointerai en 3024 ❤🎉

  • @Mdboy_D
    @Mdboy_D 2 года назад +299

    Les âmes douces l'écoutent en 2024.

  • @loufisarr8843
    @loufisarr8843 6 лет назад +347

    😭😭😭 tidjane laa mais bilay limouy waxx saa xool laay dougou j'aime bien ❤❤
    Yalla na yalla weral baatt bii

  • @Farydiop-d5y
    @Farydiop-d5y 2 месяца назад +4

    Yallah na borom bi def chiva thi kep kou tawate thi barke matlabou chifai Amine

  • @sgsofficiel3042
    @sgsofficiel3042 6 лет назад +370

    Bén biss guiss nama may nane café mounéma sama dom café dagn Koy wormal, dangay soukou wakh bisimilahi so paré né alhamdoulilah .

    • @quincailleriebasscastorsna9343
      @quincailleriebasscastorsna9343 5 лет назад +6

      Kogn dh dina Roy lolou

    • @dabasarr2079
      @dabasarr2079 5 лет назад +8

      Ta trop de chance jaimerai l voi bilay soumako guisso sama khol fekh lol

    • @Taeguuk
      @Taeguuk 4 года назад +14

      Ndeyessane mak gni dagno bakhone. Bilahi Serigne Touba rék moléne gnore 😭

    • @binetouthioune3833
      @binetouthioune3833 4 года назад +3

      Khamo bane béss la guén adouna,😭🙏

    • @thiounexassida
      @thiounexassida 4 года назад +8

      SGS Officiel Ndeysan yalla souff séd si kawam 🙏🏿

  • @mouhamadoudiallo9777
    @mouhamadoudiallo9777 3 года назад +185

    Suis talibé Baye niass
    Mais fier de Serigne Touba et de ses khassidah
    Yalla n’a yalla fayalniou suniou makkk you bakh yi khekhalll Islam baniou kay bakoooo tay
    Matlaboul shifahi ça me rappelle des souvenirs extraordinaires quand je fesais. Le bac je n’écoutais que ça presque tout la journée

    • @enzomoretti5931
      @enzomoretti5931 2 года назад +6

      Euskeuy yété Diallo sédé dou néne yagg fi lole t andak wér

    • @sidylo9069
      @sidylo9069 2 года назад +3

      Ya niag kiniane

    • @karadioum9017
      @karadioum9017 2 года назад +5

      koulou wirdine ila youridine la ku tedeki wakh kep kouy dioulite rek si ndiabotou serigne biga bok yalnala yala guena takhawou mayla barke khassidas yi yaw ku bakh ga

    • @khadimfall7388
      @khadimfall7388 2 года назад +5

      Leepou béneu la walahi ❤️

    • @mouhamadoudiallo9777
      @mouhamadoudiallo9777 2 года назад +3

      Amine mbokkk yi

  • @revolutioncrew821
    @revolutioncrew821 6 лет назад +168

    BAYE ABDOU DIOUF serigne touba fay nako té démagougne féne kou cheikh Abdou lahad diokh yeuré Serigne Fallou té sa bopp diokh la ndiguell rawnga gneupe barké borom touba

  • @cheikhmane204
    @cheikhmane204 20 дней назад +2

    ❤❤❤j’ai les larmes au yeux et le cœur lourd même je ne connais même les paroles 😢

  • @zioservices5317
    @zioservices5317 4 года назад +122

    Qui l’écoute en 2020 à l’approche du Grand Magal de Touba 2020
    Clique Jaime
    Naniou Magal ak Diam
    Barké Borom Touba

  • @mariambodj2458
    @mariambodj2458 4 года назад +88

    Matlaboul Chifai douma ko deuglou té dioyouma sama yaram dafay daw 😭🙏🏽 Serigne Abdou diouf yalla na khippé aldiana 🙏🏽

  • @gorasow8531
    @gorasow8531 11 месяцев назад +74

    Qui l’écoute en 2024 ?🙏❤️

  • @moukhamedrassoulkama4506
    @moukhamedrassoulkama4506 Год назад +2

    ❤ sokhna Ndoumbé♥️😭😭sa khassida baagui nii😭♥️

  • @oumyydiopp8182
    @oumyydiopp8182 10 месяцев назад +7

    🥹♥️♥️♥️♥️ça fait tellement de bien 🥹♥️

  • @mamadousarr7194
    @mamadousarr7194 5 лет назад +46

    Quelque soit confrérie bi nga nékk lii sa xol bi lay dougou ma shaa Allah yalnako yalla yeureum, diégeulko té kharéko al jannah

  • @diankhaoulimata7052
    @diankhaoulimata7052 6 лет назад +76

    Que la terre de touba lui soit legere

  • @bass.dng1601
    @bass.dng1601 6 лет назад +43

    Ndeysane Yalnako Yalah yeureum 😭😭 Si barké yonnetibi PSL

  • @aishatoudiaw5585
    @aishatoudiaw5585 5 лет назад +6

    Lii mouna ma rayy bilakhii non baye abdou diouf yalna yalla wanalei la akh sa sope bi yobou la aljana si barkei khassida yi
    Chuii tiijane mais foumay yobou yalla rek moko khamm😭😭😭

  • @dethiebamba4
    @dethiebamba4 6 лет назад +152

    fier d'être mouride yalna yaAllah goudeul sa fane Amiine

  • @yeroba9826
    @yeroba9826 7 месяцев назад +3

    Allahou Akbar, DIEU sera content de ce khassida ❤❤❤❤❤❤ c'est très touchant

  • @barcalove1732
    @barcalove1732 3 года назад +22

    Je suis tidiane mais j'adore vraiment ce khassida ❤️❤️
    Yallah na diam yagg 🙏

  • @diagnealy3085
    @diagnealy3085 4 года назад +14

    Talibé baye niass la dé tai meussouma commentaire RUclips wayé walahi serigne abdou diouf dafma dioylo li beugouma sakh mouy diékh Akhmadou dieureudieuf🙏

  • @guisseamadousenghor
    @guisseamadousenghor 6 лет назад +43

    Barki serigne touba baye abdou diouf yagui toyal xol yi mounouma doyal si yaw machalla

  • @kinebeguefallou
    @kinebeguefallou 7 лет назад +126

    Sama mariage bou baye abdou diouf nieuwoul dou nekh yalla gua fi yagu teh werr si barke borom touba

    • @sokhnaawandiane392
      @sokhnaawandiane392 7 лет назад +2

      Kine Begue fallou ak man dh

    • @mmefall3149
      @mmefall3149 6 лет назад +3

      Amiine

    • @maremediagne5215
      @maremediagne5215 6 лет назад +2

      més serigne abdou dafa nganiou dh nako yalla yerem

    • @rassoulette2792
      @rassoulette2792 6 лет назад +2

      Tu es mouride est tu ne sais même pas qu'il est décès, que dieu l'accueil au paradis

    • @Lafayette2708
      @Lafayette2708 6 лет назад +5

      Rassoulette commentaire bi amna 10mois kholatal

  • @modouabibnapolibarcellona492
    @modouabibnapolibarcellona492 7 лет назад +46

    ndaysane kénn dou cheikh ahmadou bamba khadimou rassoul 😢😢😢😢

  • @diabafall7360
    @diabafall7360 6 лет назад +33

    Que firdawsi soit votre dernier demeure si barkep khassaide yi si barké Matlabul chifai

  • @abdouazizfall3308
    @abdouazizfall3308 2 года назад +1

    Macha allah Serigne Abdou Akhad Diouf Yalla nako Yalla yeram takhariko aldiana firdowsi ak mbolem dioulite si barkelm Serigne Touba Allahou amine way

  • @aidafaye5645
    @aidafaye5645 6 лет назад +26

    Baye abdou diouf matlaboul chifayi bi amatoul sama xoll toyna yalna yalla yékati nga weur ba delou say activité si barké matlaboul chifayi

  • @slimbabs509
    @slimbabs509 4 года назад +39

    Que la terre lui soit légère, Baye Abdou Diouf🙏🏾

  • @fatourassoulsg5803
    @fatourassoulsg5803 6 лет назад +247

    Khassida bi me rappelle quand j ai perdu ma cousine pour soulager mon cœur je l écoutais 24 h sur 24

    • @assamedieye1271
      @assamedieye1271 6 лет назад +2

      fatourassoul S G baya

    • @julesjohn1186
      @julesjohn1186 4 года назад +3

      Paix à son âme

    • @badarandaye3950
      @badarandaye3950 3 года назад +2

      Ndeysane yala sa borom yeureum barki xassida gui

    • @adjisow3734
      @adjisow3734 3 года назад

      @@assamedieye1271 9

    • @adjisow3734
      @adjisow3734 3 года назад

      @@assamedieye1271 ghhihg8h88y88y88y88888h8gg888yyy8yy8y8yy8ivgyjg

  • @senegalndiaye4558
    @senegalndiaye4558 5 лет назад +17

    Dounde si Serigne Touba, dé si Serigne Touba , dékki si Serigne Touba.
    Dieureudieufé Cheikhoul Khadim

  • @zaleprod479
    @zaleprod479 Год назад +11

    Qui est la pour écouter cette pure merveille ❤️

  • @lysamba63
    @lysamba63 2 года назад +21

    Cette voix est trop pénétrant...quelle puissance... dieuredieuf Cheikh Ahmadou Bamba...

  • @sophiecisse4607
    @sophiecisse4607 4 года назад +26

    Douma mouride wanté li meunoumako mougn ❤

    • @serignesamb6656
      @serignesamb6656 2 года назад +2

      on est tous musulmans,c'est les noms qui diffèrent; mouslim,mouslimines,mouminins,etc

  • @sambpapa3437
    @sambpapa3437 6 лет назад +21

    baye abdou diouf yalla nanouko yalla fayal si barkè cheikhoul khadim

  • @dethiethiam2620
    @dethiethiam2620 6 лет назад +127

    Je sui talibé cheikh mes khassida bi dafay sedal sama khol

  • @binetaba7556
    @binetaba7556 6 лет назад +7

    k serigne touba tacueil ma mère au paradis éternel firdawsi en est à touba el aimé bien baye abdou Diouf yala serigne saliou faye bayi lafi basi kanam

  • @alinoseck2608
    @alinoseck2608 2 года назад +11

    😭😭 03h 38 du matin je l'écoute avec 1 cœur ♥️ remplie de 👉😭😭😭😭

  • @ThioroMbaye-u1g
    @ThioroMbaye-u1g Год назад +1

    noumouy def sama khol bi 🥺❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyebinetambaye21
    @ndeyebinetambaye21 6 лет назад +26

    Ha kéne dou serigne bamba amoul morome dé balla aicha barké serigne saliou menouma mougne khassida bi

  • @ibradiop9132
    @ibradiop9132 Год назад +23

    Dieuredieuf Baye Abdou Diouf. Paix à son âme thie barkep kou ted ki. J’ai grandi avec cette voix à Mbacke. Quelle chance pour nous❤

  • @abdoulazizsarr7046
    @abdoulazizsarr7046 6 лет назад +53

    Macha Allah. Golden voice! Straight into the heart. Yalnako sounoou borome fay si baaakhou Mouhamed saws ak si barkeih alkhourane. Amine!

  • @sokhnaboussofall4781
    @sokhnaboussofall4781 6 лет назад +8

    Yalla nalla yalla yeureum té kharé aldiania si barké serigne touba 😭😭

    • @sowpape3781
      @sowpape3781 6 лет назад

      Amine

    • @awayallananiouyalladiegueu2422
      @awayallananiouyalladiegueu2422 4 года назад +1

      Amine ya rabbi yalla nako yalla yeureum j'écoute bilay en pleurant je suis tidjiane mais nioun nieup yam thi yalla 🙏🤲🥰🥰🥰

    • @mllr5624
      @mllr5624 2 года назад

      Allahouma amine 🤲😭

  • @ThiernoSALL-jf1wv
    @ThiernoSALL-jf1wv 4 месяца назад

    Dieureidieuf Baye Abdou DIOUF Yalnako yalla deffal tawfehhhhh aldiana firdawssi

  • @sgsofficiel3042
    @sgsofficiel3042 6 лет назад +48

    Yalla na am ngeureumou Serigne Touba

  • @souleymanediop5014
    @souleymanediop5014 4 года назад +1

    Euskeuy machallah dieureudieuf serigne touba kenla amoul morom mbacke diarama mam cheikh Ibrahima fall lamp serigne mountakha mbacke yallah nafi yague lol ta wer machallah dieureudieuf ken dou la fate" serigne Abdou Diouf yallah na yallah yok sounouy khôl said nalol machallah yallah na yallah yok say ler yallah nalla serigne touba fay si barke khasidayi allahou ma amine machallah dieureudieuf

  • @antangonediouf4002
    @antangonediouf4002 7 лет назад +6

    Machaallakh plus d’un an ma ngui khassida bi ndeysane tay la ko guiss
    Chak jr ma guiss moutlaboul chifay wayé fi ma bi di yobou 😭😭😭😭

  • @diegoforlan3221
    @diegoforlan3221 2 года назад

    Khamouma sah limawara wah ndakh contane yalla n'a yalla Faye yalla machalla

  • @mayarassoulsy7759
    @mayarassoulsy7759 6 лет назад +54

    Machallahhhh Serigne Touba amoul moromm😍😍😍😍🙏🙏🙏🙏

  • @diamasakho2664
    @diamasakho2664 5 лет назад +8

    😭😭😭😭 Suma ko dégu lou walaxi sama xel dafay dém si sounu borom 🙏👌☝️

  • @oumycissendiaye3052
    @oumycissendiaye3052 6 лет назад +6

    Yalla na souf sedeu si kawam, yalla nalla yalla faye, si barke borom touba, si barke Matlaboul chifahi

  • @ndeyefatoundao4236
    @ndeyefatoundao4236 6 лет назад +5

    Décembre 2018! Yallah na souff seidd si kawame sougnou borom kharei ko aldjana firdawsi tei khassida yi terou ko si barkei cheikhoul khadim

    • @binetouthioune3833
      @binetouthioune3833 4 года назад

      Kham gua bane béss la guén adouna gua wah mako 🙏😭

  • @cheikhmariemoundiaye2651
    @cheikhmariemoundiaye2651 4 года назад +3

    Yallla nako brome Touba teerou amine

  • @dialthiamthiam5311
    @dialthiamthiam5311 4 года назад +2

    Allahouma amine yalla nagnou yalla mau jam gnoun nieup ak xolou mougne adouna dafa méty si côté yeup

  • @aaaavousetesbienbbbbniceni5098
    @aaaavousetesbienbbbbniceni5098 7 лет назад +26

    li rek moy deugue dieureudieuf khadimoul rassoul bamba partout

  • @sossof8785
    @sossof8785 6 лет назад +77

    Reposez-vous en paix 🙏🏽

  • @maremediagne5215
    @maremediagne5215 6 лет назад +4

    yalnako yalla yerem si barkeb borom touba

  • @khadysaodiop5076
    @khadysaodiop5076 Месяц назад +1

    Anti stress porte bonheur

  • @ousmanemendy6757
    @ousmanemendy6757 4 года назад +1

    Baye abdou diouf li souma koy deguelou wat kome tay la si mane sama kholl day toy ohh yalla nagua tassé ak yeurmande serigne saliou aldiana firdawsi

  • @noumchjoop6808
    @noumchjoop6808 3 года назад +1

    Yalla nk yalla yeureume kharé ko aldiana si barké serigne saliou mbacké😭😭😭😭😭😭😭😭😭💝❤

  • @mamadousene6250
    @mamadousene6250 5 лет назад +22

    Qu'Allah l'accueille dans son paradis éternel

  • @bayeadamagueye1005
    @bayeadamagueye1005 6 лет назад +6

    Kénnnn dou Cheikhoulll khadim bilahi 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭❤🔐

  • @elhadjisimakha
    @elhadjisimakha Год назад +2

    Une voix unique, j'ai eu la chance, privilège de le voir et écouter chanter Mathlaboul chifai.
    Paix à son âme

  • @fallelhadji8733
    @fallelhadji8733 7 лет назад +29

    bilahi lii nékhna baye abdou diouf yagu fii lool té and ak werr

  • @fatoumbaye315
    @fatoumbaye315 2 года назад +2

    Serigne Touba amoule morom ni xassida bi Di def sama xolll😭😭 machallah 🥰🥰 fier d'être Mouride

  • @manemboup3250
    @manemboup3250 4 года назад +3

    Baye abdou diouf yalla nako yalla kharré aldiana si barkép serigne Touba

  • @morigettacisse9181
    @morigettacisse9181 4 года назад +5

    machalla dieuredieuf sa baye yalnagna khipe firdawssi si barke mame borom touba

  • @miguelzayas5978
    @miguelzayas5978 4 года назад +2

    Baye adou Diouf yalla nala Serigne Touba fayal bopam machallah li nekh n'a lolou yalla nala yalla kharé si aldiana you kawé kawé yi

  • @mameballandiaye4084
    @mameballandiaye4084 7 лет назад +7

    Yallah nalla Yallah may werr....ak goudou fane .....ni ngay béguei lot dia. Gni Yallah Nala ko Yallah béguelei thi foko sobei rk

  • @elhajimarone113
    @elhajimarone113 7 лет назад +16

    Machallah goudal faane papa yallah sounou borom weureul baaat bii defal diam ak xeweul

  • @cheikhfall638
    @cheikhfall638 4 года назад +13

    Un très grand merci à vous l'équipe pour cette très belle dadj qui va direct dans nos cœurs qu'allah vous met bien aussi🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • @matysow766
    @matysow766 Год назад +4

    Qu’Allah te récompense le bien que tu fais à mon cœur de Musulmane et de Mouride avec sa miséricorde infinie
    Aminn

  • @aynifall96
    @aynifall96 2 года назад +3

    💖Mâcha allah kou téde ki kene khamoul loumou done bilahi Dieredieufeti Serigne Touba 💖

  • @diawmamanar5871
    @diawmamanar5871 3 года назад

    🥺🥺🥺🥺Ndayssan yalnako yalla yereum ta kharéko aldianay fir dawssi barki CHEIKHOUL KHADIM

  • @issakhasow6119
    @issakhasow6119 2 года назад +2

    Nèkhna si khôll loll Di n'a wagni mèttitou ❤️tèy dougeul mbèctè bou amoul yémouwaye djieure djeuffè borom Touba Allahouma salli hala seydinaa mouhammadin wa hala Ali seydinaa mouhammadin sallou halèyhi

  • @awabousso4571
    @awabousso4571 5 лет назад +12

    Je me rappelle keur Serigne Moustapha Bassirou si Mbacké garage type mo rek lafadone khar si thiante Tamkharite . Yalla nako Serigne bi térou sa aldiana firdawsi

  • @aramefall8713
    @aramefall8713 6 лет назад +5

    😭😭😭😭diambar dem na yalnako kou tedd ki teroo firdawsi

  • @mboupaminata1320
    @mboupaminata1320 3 года назад +1

    Yala ngaffi yagg loool t and ak wer .khassida bi menouma moigne ndakh sa dadje bi .sama djel la.yala nanioi la serigne touba fayal bopap si Barker rassoulila.jn peux l écouter sans verser mes larmes.menoumako mougn

  • @sadiomaneofficiel10
    @sadiomaneofficiel10 6 лет назад +7

    tidjiane la mé li nekh na machallah goudou fane ak wérr rek

  • @BintaCamara-n7k
    @BintaCamara-n7k 4 месяца назад +1

    Yaa Allah long life abdou diouf

  • @ridialdiouf5919
    @ridialdiouf5919 3 года назад

    Walahii ganaw serigne touba baye abdou Diouf mii motah khassida matlabou chifahii..néhmaloll air bimouy diangué daw Aramis machallah yalnako yalla fééyé al diana firdawsii barké cheickh ahmadou bamba khadimou rassoul amine ( 👌🙏🤣👀❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fatou8910
    @fatou8910 7 лет назад +6

    Macha allah papa dji nekh n'a yalla n'a yalla yagual

  • @dibacherindack425
    @dibacherindack425 6 лет назад +5

    Yalla nako Yalla xarre aldiana si barkep seydina mouhamed

  • @papito8025
    @papito8025 6 лет назад +12

    Ndeysane. ... dieureudieufei serigne touba

  • @maremediouf8597
    @maremediouf8597 3 года назад +2

    Yalla nako yalla faye si barké serigne fallou mbacké ❤❤❤

  • @mamadouaidara8658
    @mamadouaidara8658 3 года назад

    Serigne Abdou Diouf wallahi amoul morome si xassida yi yalnako YALLA défal CHIFAHI

  • @fatoucamara6863
    @fatoucamara6863 6 лет назад +2

    Ndeysane Thiey yalla bourbi yalna ko yalla haré Aldiana ci barke khassida yi

  • @visionbayedarou9066
    @visionbayedarou9066 6 лет назад +42

    Kou Gueume Serigne Touba.

  • @sougouablaye7887
    @sougouablaye7887 6 лет назад +4

    Serigne abdou diouf nara yeureume te khare ko aldialna firdawsi te dadiek guereumel serigne touba

  • @fatoukinecamara8994
    @fatoukinecamara8994 6 лет назад +31

    Dieureudieuf serigne touba

  • @seynaboudiop5731
    @seynaboudiop5731 4 года назад +1

    khassida biiii bly douma sii doyay Mame Abdou Diouf yalla nako yalla yeureume

  • @Mbecteimi
    @Mbecteimi 11 месяцев назад +1

    Thieuy ndaysaan qui est l'a Aujourd'hui 15/02/24 pour apaiser son cœur ❤️

  • @ndeyeamyseck9896
    @ndeyeamyseck9896 3 года назад +2

    Je suis talibé cheikh mé kan je l'écoute g d larme aux yeux, j lé eu 2fw o tlfne, mé dafla nekh

  • @aminandiaye199
    @aminandiaye199 7 лет назад +20

    wallahi nim may def amul feneu yobou nama fou sori

    • @dieynababassoum4574
      @dieynababassoum4574 5 лет назад +1

      Machallah que le Bon Dieu l accueille dans son paradis .

  • @djibisy1320
    @djibisy1320 4 года назад +1

    Yalla na yalla yoki léram Baye Abdou Diouf

  • @thiabaseck1023
    @thiabaseck1023 6 лет назад +5

    Yalla na ko Yalla yeureum😫😫😫😫😫

  • @adama2737
    @adama2737 4 года назад +2

    Yalla nako yalla kharé Aldiana firsdaw si si barcké 🙏🙏🤲 khasida yii

  • @dieyethiam7210
    @dieyethiam7210 6 лет назад +4

    Macha alla yalla nala yalla faye mouride sadikh Serigne TOUBA

  • @abdoubaye4374
    @abdoubaye4374 5 лет назад +4

    ohhhhh ndeysane + de 5ans je l écoute et c comm si c'était hier ce khassida, Machallah Mame Abdou Diouf

  • @kaliloulayesy2729
    @kaliloulayesy2729 2 года назад +3

    Masha'Allah dawlona yaram dieureudieuf Serigne Touba

  • @moussandiaye7357
    @moussandiaye7357 4 года назад +2

    Paa bii yallah nako sougnou borom yeureum waay🙏🏾🙏🏾✨