Khassida Mawahibou Transcription et Traduction en Wolof Version 1

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 16 янв 2025

Комментарии • 460

  • @oumarkata9279
    @oumarkata9279 3 года назад +1104

    A l'ecole on ne m'apprenais que les poémes de victor hugo rimbaud et autres ecivains mais on ne m'a jamais dit que khadimoul khadim est le plus grand poéte du monde.en plus de la qualité des textes ,je suis surtout seduit par la richesse des rimes.dieuredieuf serigne touba

  • @nenekane7249
    @nenekane7249 3 года назад +180

    J'ai écouté des milliers de fois mais j'en ai toujours des frissons à chaque fois c'est comme si c'était la première fois j'écoutais ce khassida😭
    Le poète des poètes, fowul folei wul Mbacké yalla naniou la yalla fayal😭

  • @hawasall4148
    @hawasall4148 3 года назад +30

    Khassida yi damakay drouse disi yeugue sama bop salaw d sante naniou lolou Dieureufeuty cheikhoul khadim sunu yakar tay ak euleuk 🙏🙏🙏🙏❤️

  • @mouhamedlaminekhouma3124
    @mouhamedlaminekhouma3124 3 года назад +246

    Je suis Talibé Baye mais J'M ces mélodies divines ça purifie wollahi...
    Jerejeuffféeee Serigne Touba oh😭😭😭

  • @zenabsy6282
    @zenabsy6282 3 года назад +153

    mashallah ça apaise le cœur 💓 j'ai tombé sur ce xassaid le jour de l'anniversaire de notre noble prophète sws le 20 avril c'est son 1451 ème anniversaire ya Rassoul allah yamalen gueneull ❤️

  • @sheikhtijanycheriflofficie7997
    @sheikhtijanycheriflofficie7997 3 года назад +128

    Mane talibé Cheikhou Tidjiany Cherif ma sédél beugeu bi Serigne Touba beugeu Rassouloulahi sama xol dafa sédeu thi xassida bi li dé néxeneu Yonéne tébi sopém bi thieuy Serigne deugeu deugeu mo safo Rassouloulahi 💯💯

  • @mariamadiagne8082
    @mariamadiagne8082 3 года назад +121

    Rien qu'un poème de Serigne Touba pour commencer la journée en paix.

    • @mamadousakhirdia2179
      @mamadousakhirdia2179 2 года назад +1

      Barki alkhourane ❤️

    • @matyniang954
      @matyniang954 2 года назад +2

      Yalla nagnou yalla may degg ak topp gui🙏🏽

    • @porokhanebeuguefallou2969
      @porokhanebeuguefallou2969 2 года назад +2

      Domou baye yagui wakh lou naikh xeye rék diel sa casou café teksi xasida yi mo dack lo guis bilahi en plus yao sa xél day dal tout la journée

    • @warkhalo5548
      @warkhalo5548 Год назад

      @@mamadousakhirdia2179 😊

  • @papiisow3980
    @papiisow3980 2 года назад +13

    Sante Yalla warna bepp joulite waratina ap mouride Alhamdoulilah sante yalla bou wer bagnou Yalla bolé ak serigne Touba❤

  • @adjadio
    @adjadio 3 года назад +10

    ❤️❤️❤️❤️sante yalla bou bakh si louniou nék. Ay talibé Cheikhoul khadim 👌👌👌👌❤️❤️❤️

  • @mouhamadoulaminetoure9244
    @mouhamadoulaminetoure9244 3 года назад +50

    Sama tay, sama euleuk, serigne touba ♥️♥️. Dieureudieufé khadimoul rassoul🤲🤲

  • @Cheikh_SEYE
    @Cheikh_SEYE 3 года назад +24

    Alhamdulilah pour la première fois may jangue xassida SERIGNE BI bamou diékh
    Merci Cheikh Ahmadou Bamba NDIAYE pour cette opportunité
    yalla nala borom bi fay yiiww si barké SERIGNE TOUBA

  • @malickwade4630
    @malickwade4630 3 года назад +10

    Mach'Allah suis tidjane mais vraiment khsida gui dafa nekh si khôl yalla naniou yalla fayal *KHADIMOUL RASSOUL*

  • @amadou-44
    @amadou-44 2 года назад +61

    « ANTAL KARÎMOU ANNAL KHADÎMOU DAHRAN MOUDÎROU FIKAA SANA-i » Dieuredieufé borom Touba Yaw Mi khamal niou yonente❤️😭

  • @kinelo9287
    @kinelo9287 3 года назад +64

    Khaw ma lanla mes khassida boumako deguè rk sama khol fekh souma mèrone sakh souma ko deglo guiff nek khalé tèla beug serigne bii vrai que khawna am ay sikk mes gnane na yalla mou dagne bien vrai que dou sikk you bone nak yalla nanou yalla khirr sii di def Lou bakh rk fier d'être mouride yalla nanou yalla def ayy vrai mouride Di dox si nigualou serigne bi 😘
    Gnoune gneup béne lagnou wayé ken dou serigne ahmadou bamba borom diam borom khéweul gui gua khamni kou dieul sa khol ibbil kako do meusa sone mouy fii di alakhira nk
    Deug deug serigne ahmadou bamba dou morom
    Gnane na yalla mou geuneu rakhass sama khol bama geune ko beug
    Yalla nalene yalla defale diam sameu gnou arrr gnou tè dinou khir si Lou bakh
    Kiné lo

  • @basby4555
    @basby4555 3 года назад +3

    Bilahi meune khasida yi rek la beug
    Yalla na ma souniou borom diapaler ak kepp kouko beug meun
    Mouwahibou bi noumou may deff sougn borom rek moko hamm

  • @souleymanembengue6071
    @souleymanembengue6071 3 года назад +78

    Durant ma vie j’ai appris à l’école française tant de littérature à l’égard des différents écoles littéraires mais je n’ai jamais vu une plume 🪶 que celle de Cheikh Akhamadou Bamba Khadim Rassoul
    Je dirais même qu’il est le plus fort des forts de l’humanité entière

  • @abdoulayelo899
    @abdoulayelo899 3 года назад +15

    Je suis layene mais khassida yi daf ma nekh je l'écoute de temps temps dieureudieuf serigne touba

  • @kinegorbatchev7560
    @kinegorbatchev7560 2 года назад +24

    No borom touba amoul morom
    Mais mawahibou esk lima si yeuk yénagui kay yeuk no Lou doy warr tellement dafa nex sokay déglou banex guay andale souma mérone sax souma kay deglou di guife vie de ma mére Lou nex moy xassida
    Yalla nanou yalla sambeu té arr gnou mouseul gnou si louy loré si bari kou ted ki
    Beug serigne bagnouye déh nek xalei taxoul daniou beug serigne bii🙏❤😭
    Borom compte bi tmt yalla nako yalla fayy nax sama genre gui gua xamni touti lanou meune si arabe bi yalla nalen serigne fay
    Xol sed na😭❤💍
    Fier d'être mouride❤😭

    • @tahiroumbengue5285
      @tahiroumbengue5285 Год назад +1

      Ndeyessane dafay deufeul khol.

    • @moustaphagueye5870
      @moustaphagueye5870 3 месяца назад

      Dou loolou Dé Waadji Serigne Touba Si Bopamm Moo Nékoul Nitt Khassaïde Yi Banèkh Bimou Andalle Moo Eupp Walaakhi Kéne Dou Serigne Bi

  • @mbackesene1238
    @mbackesene1238 4 года назад +12

    Thiey sama wadjii kenne khamoul loumou donne worna cheikhra fall khasida yii mounou mako deklou té😭😭ma thiey sa borom🙌🏽❤️🙈

  • @sdn2373
    @sdn2373 3 года назад +50

    Ma Sha Allah ça apaise tellement que j'en suis devenue accro...
    Dieureudieuf Borom Touba 🙏
    Beugone na gni bahei ma tourou Kourel bi barkep Segn bi. Yalla nalen yalla defal diam 🙏

  • @lobinta-nt7hz
    @lobinta-nt7hz Год назад +4

    Khasida bi MoMA meuneu dioylo bilahi dima fatalil Lima wesou ak fima yeksi dieuredieufeti cheikh Ahmadou bamba KHADIM rassoul💓

  • @aidadiouf4124
    @aidadiouf4124 2 года назад +25

    Machallah le plus grand poète de tout les temps yalna yalla doli fayalnou cheikh ahmadou bamba fayaléléne yéne gni transcrire khassidayi grâce à vous j'ai appris ce khassida chapeau à vous

  • @mouhamedciss-fd5sg
    @mouhamedciss-fd5sg 2 месяца назад +2

    De jours en jours coincée dans mes pensées et je me dis pourquoi je me suis tant attaché à cet Xassida en l’écoutant il dissipe tout mes problèmes et me donne une envie de m’éloigner …..je ne sais pas c’est quoi ce sentiment
    Dieureudiuef Seriñ Tuuba

  • @fatoubambistendour3156
    @fatoubambistendour3156 3 года назад +22

    Doumassi doyal bi khassida😭💖💗👌✌sa youma kheyer barlelouna

  • @papacheikhtall2427
    @papacheikhtall2427 3 года назад +6

    Akassa diadieuf Dieuwrine fassallé bou bakh inchallah Rabi fonkk nalla trop dakh Xassidas yii bi nak mom Ya Allah nagnou Ya Rahman geuna bollé ak momm 🙏🏾♥️

  • @mbackeleye4264
    @mbackeleye4264 2 года назад +7

    Alhamdoulilah thiey Ahmadou kénn douh môm fier d'être mouride Ba fàwou rék

  • @mamediarafaye8717
    @mamediarafaye8717 2 года назад +10

    Yalah na sounou adio yeupe fadiou andak khéll mou dall si barki seug bamba❤

  • @mouhamedndiaye6238
    @mouhamedndiaye6238 3 года назад +52

    16:10
    partie bou nieup di sett machalah serigne bi ak yonnente bi saw histoire bou rafette la

  • @Zendy00956
    @Zendy00956 2 года назад +19

    Machallah c'est la première fois makoy degglou mais daffa nekh trop , DIEUREUDIEUFÉ BOROM TOUBA , LE MEILLEUR POÈTE DU MONDE 🙏

  • @thionegueye1397
    @thionegueye1397 4 года назад +14

    Machallah Yalna kou Téde ki dolli xéweul

  • @Gggjjjjkkkkk
    @Gggjjjjkkkkk 3 года назад +5

    ❤️😭yall neu yalla fayal gnu name borom Touba dolli ay leram

  • @falloumbodj5768
    @falloumbodj5768 4 года назад +12

    Khole yanguie sede yalla nalen serigne bi faye ❤❤

  • @NdeyeToureMbodj
    @NdeyeToureMbodj Год назад +7

    Oh comment c'est touchant, émouvant, apaisant.Rien n'est plus fort que la poésie de Serigne Touba,une poésie inouïe,le grand poète,vos paroles sont les médicaments qui nous guérissent,oui vous êtes le grand guérisseur,vous êtes notre oxygène,souniou yakarr adouna ak alakhyra ❤❤ dieureudieufétiii borom Touba sante nagn leuu😭

  • @issakhaba2489
    @issakhaba2489 3 года назад +15

    Alhamdoulialh sa apaise vrema le cœur.yala nagnou yala fayal Serigne touba

  • @jerefuse2821
    @jerefuse2821 2 года назад +40

    Hamdoullillah
    La grandeur et la générosité de l’esclave magnifiant son maître sans limite sans le nommer jusqu’à ce que sa lumière et sa famille et la Kaaba vient sanctifier ce poème

  • @astoulayeniang3545
    @astoulayeniang3545 3 года назад +32

    Je suis layenne mais vraiment ça apaise le coeur ah ma sha Allah 😭😍😍

  • @mamediarragueye2990
    @mamediarragueye2990 3 года назад +8

    Alhamdoulilah dieureudieuf serigne touba yallna yalla fayla gnou ko🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @omarndiaye4883
    @omarndiaye4883 4 года назад +11

    Yalna Serigne Touba fay la🥰Li dafa neex billahi

  • @ibrahimaly8584
    @ibrahimaly8584 2 года назад +20

    Quand je suis triste ou de mauvais humeur je viens me réfugier dans les xassida .

  • @tahiroumbengue5285
    @tahiroumbengue5285 Год назад +7

    Ça apaise le cœur. Ndeyessane walay Mbacké balla LE PLUS GRAND POÈTE DE TOUS LES TEMPS

  • @saidahamza538
    @saidahamza538 2 года назад +12

    Noo Serigne touba amoul morom dh😭🙏🏼

  • @mbackeleye4264
    @mbackeleye4264 4 года назад +24

    Alhamdoulilahi c'est très important Que dieu vous accorde une longue vie.amine.

  • @aliounefall490
    @aliounefall490 3 года назад +20

    Coeur apaiser après lecture de ce beau xacida ❤️❤️

  • @bounambath9186
    @bounambath9186 2 года назад +2

    Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul mbideff dotoul mel nih mome mashala.................xassidas yi rek cibir xole dara menouko remplacer

  • @sergedione7658
    @sergedione7658 Год назад +5

    Dieuredieufé Serigne Touba diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp qui es la le jour du Magal 04/09/23
    08:31 Sn.

  • @kinelo9287
    @kinelo9287 3 года назад +9

    Kéne dou mome kepp kouye mourid warna diang khasida bii nakh serigne migui sii tagg kou tédeu kii gua khamni kéne douko yamalé ak kéne nakh taram bou magg bi nek khalè teksi djiguene téla beug khasida nakh beug serigne bou magg nek takhou ta bagna diang khasida

  • @mounadiop3886
    @mounadiop3886 Год назад +2

    Eskeuy kéne dou Borom Touba ❤❤❤❤ dieureudieuf serigne touba mbacké amoul morom ❤❤❤

  • @fatoukinedrame8541
    @fatoukinedrame8541 2 года назад +3

    Talibé cheikh bi mo beugue borom touba
    Mbacké balla yalla nanula yalla fayal 🥲

  • @aliousamb5163
    @aliousamb5163 7 месяцев назад +9

    Dieuredieuf Serigne Touba
    Dieuredieuf Serigne Touba
    Dieuredieuf Serigne Touba
    Dieuredieuf Serigne Touba
    Dieuredieuf Serigne Touba
    Dieuredieuf Serigne touba
    Dieuredieuf Serigne Touba

  • @mouhamedthiam8209
    @mouhamedthiam8209 4 года назад +10

    MACHALLA MOURIDE KHASSIDA AHLOU BADRINE DIAPALÉ LÉNE MASI

  • @lyontvproduction9505
    @lyontvproduction9505 3 года назад +6

    dieuredieufé serigne touba souniou yakar tay ak souba
    sant serigne touba
    souniou weruwayyy
    bamba protege

  • @NganeSalihate
    @NganeSalihate 3 года назад +4

    MashaALLAH santt naniou boubakh Borom TOUBA

  • @astousall454
    @astousall454 4 года назад +4

    Machallah khôl Sedd neu Yalla na lenn borom touba fayy si barkei khassida yi🙏🙏😭

  • @MaAstaDiop
    @MaAstaDiop 2 месяца назад +2

    Partie bi dîna ma ray rekkk nimouy daadié macha Allah ❤❤❤🎉 fimou wakhé < Hanni Jâzâkâ Rabboun Hadaka Faw Qal Mounaka Yawmal jazâ-i❤❤❤❤

    • @ndirmamadou3804
      @ndirmamadou3804 Месяц назад +2

      Dafa nekh dh

    • @ndirmamadou3804
      @ndirmamadou3804 Месяц назад +2

      😍 sérigne Touba kéneu la😭❤❤❤❤

    • @MaAstaDiop
      @MaAstaDiop 12 дней назад +1

      ​@@ndirmamadou3804 non li mo raw nekh❤

    • @MaAstaDiop
      @MaAstaDiop 12 дней назад +1

      ​@@ndirmamadou3804 wakhatiko dh❤

    • @MaAstaDiop
      @MaAstaDiop 12 дней назад +1

      ​@@ndirmamadou3804bly li mom MashaAllah ❤❤❤

  • @AbdoulayeGueye-l7p
    @AbdoulayeGueye-l7p 8 месяцев назад +1

    Machalla j'ai les larmes au yeux direct sama khol la dieum dieureudieuf borom touba

  • @momardrawing9168
    @momardrawing9168 3 года назад +11

    Ammiiine Ya raabii, dieureudieuf Serigne Touba.
    Machaa Allahoû

  • @assicofamilysantos169
    @assicofamilysantos169 7 дней назад

    Yalna Nala yalla fay a cause de toi magui djanggg xassida blhii❤❤❤❤❤❤❤ yalna naga guissé AK Serigne Touba ❤

  • @Aya-qz5fs
    @Aya-qz5fs 3 года назад +2

    Thiey serigne Touba le grand poète
    Yalla naniou ko yalla fayal

  • @fatimdiagne5208
    @fatimdiagne5208 2 года назад +7

    Mon préféré 🥰🥰ken dou cheikh bi❤️

  • @basinegeuye6903
    @basinegeuye6903 3 года назад +10

    Dieureffe Serigne Touba dieureffe Serigne Touba dieureffe cheikh Ahmadou bamba khadim Rassoul ♥️♥️♥️♥️♥️♥️😍😍

  • @mameboussombow5676
    @mameboussombow5676 3 года назад +5

    Mane dal sama xol mogui fekh sed lol 🌧️ Limay yeuk lamine meunouko wah Barki Borom Touba🤍🤍🤍💕💕💕💕💕 way nek mouride mo neh way Bilahi si Barkép werou koor gui bouma yalla naroul may dieukeurou Mourid Yana lambeau😭😭😭😭

  • @mamifall2813
    @mamifall2813 3 года назад +3

    Apar maka fa yonté ba teude guissouma kou gnou guen rew yarabi yalla ga fayal gnou sougnou mag you bakh yi dieuradieufati cheikhoul khadim borom chaine bi tamite yalla na ga bokou si miliarderou serigne touba takhna ma guena meune mbak sougnou borom👍👍👍👍👍

  • @papeserignembaye8679
    @papeserignembaye8679 3 года назад +4

    Thiey borom Touba
    Machallah traduction bi amna solo

  • @dieyfama325
    @dieyfama325 2 года назад +5

    D auré avance personne m acceptais par mon indifference , maintenant j ai séci l opportinité de Akhmadou grace a ces poéme qui façon, modeler et qui éduc l homme dans ses sort dieuredieuf Bamba

  • @fatoubambistendour3156
    @fatoubambistendour3156 3 года назад +6

    😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😭😭😭😭😭😭😭dieureujeufety serigne bi si mbind mi . . Aka mounio sauver😍

  • @daoudathioune2021
    @daoudathioune2021 3 года назад +2

    Machalla yene gnigua khamni yenaye tasare mbindou you sel yi serigne touba binde Yalla nalene Yalla faye si barke khassida yi

  • @evadiouf3493
    @evadiouf3493 4 месяца назад +1

    Yallna yalla yokh aay lerlam thi barké kou téudd ki psl❤

  • @kyadiop1780
    @kyadiop1780 2 года назад +10

    Dieureudieufé Serigne Touba 🙏🥰

  • @WedjiNdiaye-w2i
    @WedjiNdiaye-w2i 4 месяца назад +2

    Dieureudieuf serigne Touba khadim Rassoul Diarama Mame cheikh Ibrahima fall lampe

  • @diengbossserigne9664
    @diengbossserigne9664 2 года назад +5

    Thieuye seringe touba mo wakhli🥰😭

  • @bamoussa4984
    @bamoussa4984 5 месяцев назад +1

    Dieuredieuf Serigne Touba ❤❤bilay Day sédal khôl ❤❤❤❤

  • @michoubadiane3139
    @michoubadiane3139 4 года назад +12

    Machallah dieuredieuf cheikh ahmadou bamba

  • @diwanedecor6416
    @diwanedecor6416 2 месяца назад +2

    Chaque matin gnou dieul sougnou wale❤

  • @mansourdiame1754
    @mansourdiame1754 3 года назад +17

    Thiey serigne bamba li nékhna

  • @sokhnambenendiaye7375
    @sokhnambenendiaye7375 3 года назад +6

    Wa traduction bi dama ko yekha khol li nekh na dee so khamer limiy wakh si khol lay dougou dieureudieuf serigne bamba

  • @mamediarrathiam9114
    @mamediarrathiam9114 3 года назад +8

    Dieureudieufeuty ahmadou 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @mouhamadcisse9836
    @mouhamadcisse9836 3 года назад +6

    ماشاء الله والله لقد فرحت كثيرا بكم حفظكم الله

  • @bakarykonate5211
    @bakarykonate5211 Год назад +2

    Tag Seydina Mouhamed rèk moy deug…fier d’être musulmans

  • @falldiaga8208
    @falldiaga8208 Год назад +1

    Cheikh ahmadou bamba le plus éloquent l'écrivain des écrivains sn plume ya trop de barakah quel poète notre bamba il est l'être bâtissant d'être plus être q certains des êtres certes serigne touba le pére pûr 🍯🥵😭🥺❤️🤍🥰

  • @issandiaye7100
    @issandiaye7100 9 месяцев назад

    Le plus grand poète dans l’histoire du monde
    Dieureudieufé Serigne Touba ❤

    • @ahmadyndiaye6305
      @ahmadyndiaye6305 9 месяцев назад

      😢hihùh😅😊😅😅😅😅😅😅😅😅😅h. Uv

    • @ahmadyndiaye6305
      @ahmadyndiaye6305 9 месяцев назад

      😢hihùh😅😊😅😅😅😅😅😅😅😅😅h. Uv

  • @khalilprincedikoen2917
    @khalilprincedikoen2917 3 месяца назад +1

    JE SUIS TIDIANE MAIS KHASSIDA REKK LAY DEGLOU❤ BA PARÉ MOUNEKO

  • @bintumbengue8872
    @bintumbengue8872 3 года назад +6

    Serigne TOUBA amoul morom 😭😭😭🥺🥺❤❤❤

  • @momydiop52
    @momydiop52 3 года назад +11

    Machallah dieuradieuf Serigne touba♥♥♥♥♥♥♥♥♥

  • @mouhamadoulaminediohkamite7410
    @mouhamadoulaminediohkamite7410 3 года назад +2

    DIEUREUDIEUFE SERIGNE TOUBA. SERIGNE TOUBA AMOUL MOROME

  • @fatoutallsokhna1056
    @fatoutallsokhna1056 Год назад +1

    J'écoute chaque et depuis je les commencé je me sens ci bien alhamdoulila dieureuf serigne Touba

  • @fatoucamara6605
    @fatoucamara6605 2 года назад +10

    Que Dieu te bénisse et t'accorde une longue vie 🤲🤲🤲

  • @mamadoudiagne1452
    @mamadoudiagne1452 4 года назад +7

    Li gua defd mi magui lay sante dila guereum barké chekhoul khadim an na solo lolou t kou ne meunasé dieufandiko

  • @rokhayandoye7184
    @rokhayandoye7184 10 месяцев назад +1

    Mashalah ❤❤❤❤❤li nekhna❤

  • @beugborombelel2293
    @beugborombelel2293 4 года назад +7

    Cëy sama waaji
    Waaw góor waay

  • @SanouCamara-f6b
    @SanouCamara-f6b 4 месяца назад

    Je suis moiride est fière de l'être mais fouma tolou damay zikar tarikha yeup nak wanté chaque jour que Dieu fait souma yéwo khassida borom Touba djieuk si samay noppou machallah 🫶🫶🫶jereudieuf Ahmadou Bamba🙏🙏🙏🙏

  • @satoundiaye6951
    @satoundiaye6951 9 месяцев назад

    Thiey xassida yi Serigne Touba amul morome dh

  • @khadysow4880
    @khadysow4880 3 года назад +7

    Dama ko beugue télécharges pour déglou tout le temps 🙏🙏🙏🙏❤❤❤

  • @Ndioro-ht5ej
    @Ndioro-ht5ej Год назад

    Machallah yalla naniou yalla khir si khassida yii AK si ndioub

  • @FatoukinéDiouf-k4t
    @FatoukinéDiouf-k4t 2 месяца назад +1

    Thieye serigne touba amoul morome

  • @SeynabouDieng-k4e
    @SeynabouDieng-k4e Год назад

    Jeredjeuf cheikhoul khadim rassoul yalna leu yalla fay ndax nioune amouniou sa fay.❤❤❤❤❤❤

  • @ousmanecamara-yi2pd
    @ousmanecamara-yi2pd 4 месяца назад +1

    Dieureudieuf Serigne Touba kouko wakhoul goréwo

  • @plumeuniverselle7461
    @plumeuniverselle7461 8 месяцев назад

    Yalnanou yalla fayal Serigne Touba .Kii moo baakh ak mbind mii di séelal rouh❤

  • @moustaphafall9937
    @moustaphafall9937 2 года назад

    Yow borom page bi !! Yangi deff liguey bou am solo!! Dieureudieuf ♥️!! Yalnanga tassék ngeureumeule Serigne Touba. Mane dé awma sa Fay

  • @sarrwoly6695
    @sarrwoly6695 3 года назад +8

    Machala amna solo
    Dieureudieuf Serigne Touba ❤️❤️❤️

  • @LyricsMusiqueSn
    @LyricsMusiqueSn 4 года назад +26

    Machallah !! C'est très important