Un jeune homme qui a fourni tous ces efforts pour travailler pour le bien être de ça famille et les vieux irresponsable qui sont échoué lamentable qui vient dérober et détruire la vie et le travail des autres bon courage à frère que dieux vous relevez 💪💪💪💪
Li moy Senegal, il faut réfléchir avant d’investir dans ce pays. Les gens sont méchant et jaloux…. Mieux même rester en Europe pour le rester de sa vie.
Billaahi NDEYSSANE Jai le coeur meurtrie 😭😭😭billaahi lou niaaw tee mety jambaar nga lepp dinga ko amat lo ndam bayil lep ak souniou brome REK on nest de tout coeur avec toi yalna yaallah werlennnn
Salam le ministre de l'intérieur doit sortir et faire conférence de presse et prendre c responsabilités c pas normal senegal et devenue un pays de désordre c triste
Lolou yep deug leu mais placeou transfert d argent avec des camera non surveille coffre fort yi securisewoul porte d entre yi non codé facile à démonter et les serrures
C'est pas ca la solution boko commencé tu verras des commercants organisés leur propre cambriolage. La solution c'est mettre la pression sur le ministre de l'interieur qui ne fou pas grand chose depuis sa nomination.
Triste affaire. Ce jeune entrepreneur est brave. Il ne montre aucun ressentiment ni colère malgré les pertes lourdes. Son comportement est une leçon de vie pour tous. Je suis édifié par sa sagesse et sa facilité à pardonner et à tourner la page. Ce malheureux incident le rendra encore plus prospère inch'Allah.
Aucun mot en français pour nous autre qui ne comprenons pas le Wolof. Ça saute aux yeux que c'est un cambriolage, mais le contenu est insaisissable pour nous autres qui exerçons la même activité et qui sommes également dans la sous-région. Courage mon frère, que le bon Dieu te fortifie.
Courage mon gars force à toi n’abandonnes jamais 💪🏾 mais outal système d’alarme qui te prévient quand il y’a une intrusion parce que lima comprendre si sa wokhe moy tailleur bi mola wo et bi ngua kholé sa téléphone fek na ils étaient déjà ds ton magasin c’est dommage de tenir un business de cette envergure et de ne pas investir sur la sécurité! Kou dougue si magasin bi après la fermeture alarme bi daf lay prévenir si sa téléphone c’est ce qu’on a en France en tout cas! Kholal lolou waay li metina trop
Limasiy wakh moy képp kou am place wala keur woutil camera de surveillance nga monté kosi kii deh kham ngani camera yi chauvé nanouko parceque police dina diap niépp té khalisam dina guénna inchalah mercî
Massa baye niit kou bakh ndeysane kou guem yallah kou guem bopam en plus c’est pas la première fois gnou def ko lii yalnala yallah indile louy tok inchallah
@@SeynabouDiallo-em6jjc’est ce que j’allais dire peut-être ils ont dû venir un jour repérer les lieux guisss coffre bi surtt mou attirer sene attention entt cas màtina trop
Avec sa gnoune gni nek si Europe bi guéne gnouye beugue raye gneuw léne investir séne deuk dinagne ligueye ba d gneuw gnou def gnou ni cest vraiment dommage courage frérot
@@mbenedieng2298 ah bon, c'est possible.. dans ce pays, il y a des gens qui ne veulent rien faire et aiment vivre noblement en volant.. Yallana borom bii wèrr-lène..
Mn cœur seigne 😢Li metina trop Wa li sokhor la wala ignane Allahou akbar yAllah gueumoule nelawoule yAllah nalene borom bi wére trokhaléne frère je suis de tout cœur avec toi yAllah nala borom bi takhawou diapalè la mayla lou gueune liniou la yoboule
Il faut monté des détecteur de mouvement qui t'envoies directement un notification sur ton portable et déclenche en même temps une alarme sonores. Courage frères
Il faut donner une récompense de un million à qui reconnaîtrait un des membres du gang on peut cacher son visage mais l’apparence physique et la démarche ne trompent pas Un Crime n’est jamais parfait
Ashia brother. Don't worry at all because you carry the grace of billionaire. You shall even get richer after this robbery. You were born very very rich. These same people who robbed you will be surprised to see you become a billionaire by the time you are 50 yrs old. Don't lament. Just watch and see what the Almighty God will do for you.Lots of love from Cameroon ❤
Triste découragent incompréhensible j’ai pas de mots vraiment galsen fait mal détruire tout en travail en une seconde courage mon gars y’a de beaux jours devant ✊🏽
BAYE MOR WAW GOOR RE YAW. APRES TU ES REZTE CALME AFIN DE POUVOIR REPONDRE AUX QUESTIONS POSEES. LACHE MONOUL WESSOU SA MOROME DI LIGUEYE, DANE DOLEME GUA DIOUGUE FEULE DI GUINAWOU POUR DIEUL LIMOUYE SOUTOROLOU. CERTAINS D 'EUX ON PEUT LES VOIR CARREMENT SURTOUT LE VIEUX, QUEL VERGOGNE. IL FAUDRAIT DES GARDES DE NUIT GNOUYE RONDE LES LIEUX. BAYE MOR. MES FELICITATIONS, TU ES UN VRAI BATTANT, UN SENEGALAIS BRAVE , DE BON COEUR CA SE VOIT. JE TE SOUHAIT LE MEILLEUR A L' AVENIR ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Pauvre baye mor j ai pitié de toi tu es fort que le dieu tout puissant te vienne en aide pour que tu puisse avoir plus que ce que tu as perdu du courage
Coffre dou banque ; agence yi daguene war am compte bancaire ; di def deux versement ci journee bi bala mouy diekh.. Midi ga yobou banque liga liguey ; 16h ga dem def dernier versement comme ca li dess ci agence bi dou barii.. Tabakh ay chambre secrete ci place yi difa def portable you cher yi ect... Fagarou lene svp
Un jeune homme qui a fourni tous ces efforts pour travailler pour le bien être de ça famille et les vieux irresponsable qui sont échoué lamentable qui vient dérober et détruire la vie et le travail des autres bon courage à frère que dieux vous relevez 💪💪💪💪
Li moy Senegal, il faut réfléchir avant d’investir dans ce pays. Les gens sont méchant et jaloux…. Mieux même rester en Europe pour le rester de sa vie.
Não entendi com tantos carro que passou e ninguém chamou a polícia
C'est les enfants de sans cœur, courage mon frère le seigneur va t'aider.
Gnii deff lii yalla naleen yalla niit thi barkep gamou guii niou nek si barkep seydina mouhamed (psl)🙏❤️
Amine wayyyyyy😢😢😢
bilaye legui gniou fegne com gni done agrésé borom scouteur bi diap nagne len gniom gneup
Amine 🤲
Amine YA RABI
Amiin yaa rabal halamiin 🤲
Ils ont même pas honte de faire ce genre de choses ay goor you ni lengue di sathie mane li dépassé ne meu😢💔💔💔 courage mon frère 💪💪💪💪
Un vrai gentleman ce gas faut faire un cagnotte vraiment pour le donner du force
Cagnotte moye diape domérame you deff li caméra yi wonéna séne visage yi
Bepé manako
Bien dit bonne idée
Mérci bonne idée
Billaahi NDEYSSANE Jai le coeur meurtrie 😭😭😭billaahi lou niaaw tee mety jambaar nga lepp dinga ko amat lo ndam bayil lep ak souniou brome REK on nest de tout coeur avec toi yalna yaallah werlennnn
gni vraiment ay domeram lagne nit liguéy ba amal bopam guéne défko ni😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Salam le ministre de l'intérieur doit sortir et faire conférence de presse et prendre c responsabilités c pas normal senegal et devenue un pays de désordre c triste
On doit le Limoger tout bonnement. Depuis lors il ne fait aucune déclaration et c'est du manque de respect et d'empathie vis à vis des sénégalais
xana dagnion wakhoul rek gnigui liguey guiso gni agresé wone borom sac bi si scouteur bi diap nagne lein gneup sakh
wakh bi amoul ndiarigné gnom kay nane def sen Liguey rek koufi def agression dinane la diappou inchallah
C un vieux paresseux Antoine moko meun fouf
@@awandiayediouf2437Fière de la police sénégalaise
Il est serein ce gars . Yalnako yalla diapalé teh leral mbir mii🙏🏻🙏🏻
Yalnalein yalla Weir si barki Gamougui yarabi😢😢
Amine
Amine
Amine
ىرنىى خ ج 😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊ض😊تو😊😊😊😊😊 مننا😊😊 تمه😊😊 انو😊😊😊😊 ختت😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
تهتههههتههههههتتتهته😊😊ه😊ه😊ه😊😊😊هتتتتته
This is so sad, may God restore him to even greater success than what was robbed from him.
On demande respectueusement les autorités d'aider financièrement ce jeune sénégalais
Je suis parfaitement d'accord avec vous
J'ai pensé la même chose😢😢
Lolou yep deug leu mais placeou transfert d argent avec des camera non surveille coffre fort yi securisewoul porte d entre yi non codé facile à démonter et les serrures
C'est pas ca la solution boko commencé tu verras des commercants organisés leur propre cambriolage. La solution c'est mettre la pression sur le ministre de l'interieur qui ne fou pas grand chose depuis sa nomination.
@@JOLLYWOODSenegalTu a raison
Triste affaire.
Ce jeune entrepreneur est brave. Il ne montre aucun ressentiment ni colère malgré les pertes lourdes. Son comportement est une leçon de vie pour tous. Je suis édifié par sa sagesse et sa facilité à pardonner et à tourner la page.
Ce malheureux incident le rendra encore plus prospère inch'Allah.
Ndaysan metina courage frère ❤
Aucun mot en français pour nous autre qui ne comprenons pas le Wolof.
Ça saute aux yeux que c'est un cambriolage, mais le contenu est insaisissable pour nous autres qui exerçons la même activité et qui sommes également dans la sous-région.
Courage mon frère, que le bon Dieu te fortifie.
Courage mon gars force à toi n’abandonnes jamais 💪🏾 mais outal système d’alarme qui te prévient quand il y’a une intrusion parce que lima comprendre si sa wokhe moy tailleur bi mola wo et bi ngua kholé sa téléphone fek na ils étaient déjà ds ton magasin c’est dommage de tenir un business de cette envergure et de ne pas investir sur la sécurité! Kou dougue si magasin bi après la fermeture alarme bi daf lay prévenir si sa téléphone c’est ce qu’on a en France en tout cas! Kholal lolou waay li metina trop
Machallah moi je fais ces installations bien parlé madame MCA-ÉLECTRICITÉ-GÉNÉRALE mon entreprise
Courage mon frère
Svp faisons une guete pour le soutenir lui et ses employés merci❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yal nala yalla taxawo thè taxawono inchalah amine yarabi barke cheikh ahmadou BAMBA
Massa k'Allah le tout puissant tte vienne en aide te nitale la malfaiteurs yi amine
Un homme tellement courageux
Que justice soit fait pour vous 🤲🏻💔
Sénégal metina ! Dangay liggey ba sone fek ay domeram you diougué feulé sathie linga yorr ! Metina trop bilahi
Ay vrai domukharam goor degg du sathie du agresse la police na qu a faire son travail diap sen n day niom nieup
Ló thi gniak yalla na la ko Yalla diokhat inchallah
Ndéyssane massa métina démaka yeureume bé mounouko xool courage mn fils santal yalla boubakh yalna yalla maye xolou mougne ❤❤😢😢😢
YALNA YALLA Remplacél Lako ak Lou Gueune, Amiiiiiiiiiine IN CHA ALLAH🤲🏻🤲🏻🤲🏻🤲🏻✊🏼
Ôoooooo 💔, koukoy dimbaliwat pour mou amat fonds de roulement 😢.
Courage frère je suis un jeune entrepreneur d'électronique comme toi 🎉
Baparé pa bi mothi gueneu sokhor kholal nimouy dadjé reg wayé police dinalen diap inchalla
Amna si yakar dé
Limasiy wakh moy képp kou am place wala keur woutil camera de surveillance nga monté kosi kii deh kham ngani camera yi chauvé nanouko parceque police dina diap niépp té khalisam dina guénna inchalah mercî
Gni nioy ay domeram deug yalna len yalla torokhal yalnagn ko Guiss Nala niouy deh li Mettina ndeysane 😭
Baye mor est très courageux yallah nala yallah same niite gni def dieuff djii
Mane meunou ma comprendre auto yi leen rombou ypp khana bénn nitt dieulou si tlphn nam wo police gni kouleen khol khamni liguèyouniou 😭😭
Massa baye niit kou bakh ndeysane kou guem yallah kou guem bopam en plus c’est pas la première fois gnou def ko lii yalnala yallah indile louy tok inchallah
Mai’s il faut que mou bayi khel son entourage lii doyna waar trop 💔
@@SeynabouDiallo-em6jjc’est ce que j’allais dire peut-être ils ont dû venir un jour repérer les lieux guisss coffre bi surtt mou attirer sene attention entt cas màtina trop
@@KFmouSerigneSaliou28 c’est ça ma belle boh demeh yague naniou fa gneuw gayi daniou doy waar trop …bilay wessou metti
Avec sa gnoune gni nek si Europe bi guéne gnouye beugue raye gneuw léne investir séne deuk dinagne ligueye ba d gneuw gnou def gnou ni cest vraiment dommage courage frérot
Bilay tu as raison
Li niawna way mais yallah bakhna dinga amate lou eup Li insha allah
Méti na trop franchement yalna yalla Léral lép barkep Borom Touba 🤲🤲🤲
Khar gua kou Diarra khar yalla dineuh nieuw dee kou KO khar mou nieuw
Wallahyl hazime ndayssane
Dégatinaa deugg dh
Courage mon frère Yallah dina nieuw inchallah
kholale Pabi bou gnakeu fayda dabii séne bire .Dieu est Patient !!!!
Lolou mooma metti😢
Ce pays est vraiment triste.. lolou momeu guen metti, un vieux parmi les agresseurs.. j'ai vraiment mal
@@alphaoumardiallo6090ki dou pa dé dafa sole dialabé rek mé li méti
@@mbenedieng2298 ah bon, c'est possible.. dans ce pays, il y a des gens qui ne veulent rien faire et aiment vivre noblement en volant.. Yallana borom bii wèrr-lène..
@@alphaoumardiallo6090 hun pa Kate khana waroule manké ni
😢😢Li metina trop yalla nako yalla diappalle
Def leine alarme amoul damay bagna deranger deleine def alarme si canard yi bahna
Aywaay ndeysaane yalnala ya Allah tahawou mayla lou gueuneu beuri té gueune si yéne incha Allah amine ya Rabal Alamine
sathie wala agresseurs bilahi diarounio yeureum ay vrais dmrm niak diom.😢
Gni dal yallah nagniou lene diap dague sen lokho yi yeup aye vraiment domeram lagniou
Mn cœur seigne 😢Li metina trop Wa li sokhor la wala ignane Allahou akbar yAllah gueumoule nelawoule yAllah nalene borom bi wére trokhaléne frère je suis de tout cœur avec toi yAllah nala borom bi takhawou diapalè la mayla lou gueune liniou la yoboule
Il faut monté des détecteur de mouvement qui t'envoies directement un notification sur ton portable et déclenche en même temps une alarme sonores. Courage frères
Ya n'a mais c plus cher
@@clouchevraimentfall797plus cher que ce qui a été volé?
Yalnalen yalla werr😢
Beaucoup de courage frère masta
Ndeyssane 🙏🙏courage diambar
Il faut donner une récompense de un million à qui reconnaîtrait un des membres du gang on peut cacher son visage mais l’apparence physique et la démarche ne trompent pas Un Crime n’est jamais parfait
En plus ils ne portent pas de gants donc la gendarmerie peut exploiter leurs empreintes digitales pour les identifier...
Kone legui gnou fegne amenasi kou kamame gui fegne mais pa bi moye dagueu sama khole
Pa bi mooy dagualei sama xol bi kokou bouko police diappei bounn ko bayyi nan dagu lokho bi@@Oumanas5995
@@Oumanas5995 pa bi sén chéfff
@@Oumanas5995kone yow guiss nga pabi pour mane mane rek mako setlou dokh sakh meunoko ak lokho you lakh vrai mbam la
Sénégal fane yi rakh nagne niou dh 😢😢
Ministre de l interieur bi mom vrement warna gorgorlou temps yi sathi gui leumbé na rewmi ak ray gui , mais du courage mor mitina torop
Ah gouvernement bi dafay utiliser yène poste yii comme récompense au lieu de faire une sélection sélective
Amine ya rabbi
Vraiment sa me dépasse l'insécurité qui se déroule dans mon pays le 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳 yallah na yémefi frère
Pourtant un car a passé les malfaiteurs ďouvrir le magazin cé triste 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Merci Baye mor Yokou Nama Trop ohh DU courage Yàlla Bakhna
Mastaaa yalnala beteu ak louko gueune❤
❤❤❤😢😢 du courage massa
Gni nioy domeram deug bone
Ayy way thiey....ils faut que le ministre de l'intérieur aide la jeunesse
Bo demee sakh domeram yiko def niougui si comenetair yi di dooul domikharam yi😢😢yalln la yalla diap le 😢😢
Je ne sais pas quoi écrire damaa tiit,diomy ayy sama reew yakhouna😢😭
Liii mom dou sathie kessé sohor la koi pour man 😢😢😢holal wadji moudié gueneu té mou tothie écran bi pour lann😢😢
Quand tu mets une caméra, fais un relais de chez toi tu peux savoir tout ce qui se passe dans ta boutique
Il l´a fait mais hélas
@@jeanmmmm Ça fait vraiment mal..
Métina.trop😢😢😢😢
Il l'a fait. Quand on l'a appelé il a regardé les caméras sur son portable
Ndeyssane Ndeyssane yalla Nala yalla taxakhou
Massa mon frère yallanalen yalla nit.
Kholal paa bou todjj thiooottt n….. bi après ga dem diokhiko sa niabot digako layoo ak sug’ boromm dh dmrm 😢
Bilaye 🥹
Djabottt lekk Lou lewoul toumouranke rekkk ley deff
L’état du Sénégal doit prendre ses responsabilités le pays va mal les personnes qui investissent vont fuir et augmenter les taux de chômage
Mm l’amérique et la russie ont sa l’etat ne peut y rien
Ashia brother. Don't worry at all because you carry the grace of billionaire. You shall even get richer after this robbery. You were born very very rich. These same people who robbed you will be surprised to see you become a billionaire by the time you are 50 yrs old. Don't lament. Just watch and see what the Almighty God will do for you.Lots of love from Cameroon ❤
Il est vraiment courageux, yalla dinala diapalé inshallah
Yallna yalla nit Len Barckep sëriñ Fàllu Barckep Gamou gui😢ta yalla wër Len inch'Allah 🙏 Amiiine Yarabiii 🙏
Courage Mon Frère Que Dieu Soit Avec Toi Nchallah 😢🫶🇩🇿🇩🇿🇩🇿
Triste découragent incompréhensible j’ai pas de mots vraiment galsen fait mal détruire tout en travail en une seconde courage mon gars y’a de beaux jours devant ✊🏽
Bilahi walahi wa talahi yallah nalene yallah fégnal alak lene ba faw si barki seydina mouhamad psl😢😢😢
Ndéyssane yalla bakhna frère 😭😭😭😭😭😭😭
L'insécurité c'est partout au Sénégal le gouvernement doit beaucoup augmenter l'effectif de la gendarmerie et la police
Merci Fadel pour l'hommage à nos martyrs🥺
Baye Mor yalla sunu borom taxawou
C dommage heureusement que y’avait des caméra de surveillance ça peut servir quelques choses
Du courage mon frer yalla bakhna gni deff li yalla nalén yalla nitt si barké serigne touba
Hoo ndeysane li mètina trop bilahi 😭 😭😭😭😭 sama khooll 🫀 fesna trop bilahi yalla nallène yalla wèère si wèrou gamou gui😭😭😭
Les véhicules qui passent auraient pu alerter la police.
Les autorités n'ont toujours pas réagi ?? 😢😢
C'est ce que je me dis ni dé pourquoi ne pas alerter 😢 c'est vraiment triste li
Malheureusement c'est le monde qui devient comme ca tout le monde se fou de ce qui arrive au autre
Courage frero, force à toi, triste pour l'Afrique 😢😢.
Du courage mon frère Yalna naleine yallah feinial thi barki bissbi😢😢😢😢😢
الله اكبر الله المستعان نسأل الله السلامة والعافية
Oh Senegal nione founou dieume laa khamoull billahi 😢😢😢😫😫
Aywaay limétina déh😢😢😢😢Yallah Yalnanga féniale defkati niawtéf yii 😢😢😢 massa frère 😢😢😢Yalnala Yallah takhawou 😢😢
Sénégalais modoule dimbalé auto yii rombe guissou ñiouli wowi police
S'il roule 100 à l'heure ils ne peuvent pas deviner que gni daniouy cambrioler
Et les cambrioleurs sont au nombre de 8 et armés de surcroît, donc kane moy dieul risque à 4h du matin garer autowam naan dafey intervenir
@@veriteabsoluedeugneekhoul1720 La police sénégalaise ne réagit pas aux appels
Man lolou moma diakhal di je suis choqué 😢
@@veriteabsoluedeugneekhoul1720gua tal sa klaxon yeh wa kogne bii wala gua woh police
Ndaysaan mitina lool,yalnanlén yàlla niit😢
Pa bi mom souko police diappei warounn ko bayyi waat ndax day yaakh société bi😢
Lolou Moy deug
Video bi guis naa si beneu paa dama tit sah 😢
Yalla nalen yalla weur 😢
Franchement c est trop dans un état de droit. Et les autorités étatiques silence total.
😢hoo bilahi metina yalla na yalla mayla kholo monge😢😢
Du courage bro diambar gua gorr gua ❤
Pole sana kaka🤲🤲🤲🤲😭☝️💘
😢😢😢😢yalna la Yallah takhawou
BAYE MOR WAW GOOR RE YAW. APRES TU ES REZTE CALME AFIN DE POUVOIR REPONDRE AUX QUESTIONS POSEES. LACHE MONOUL WESSOU SA MOROME DI LIGUEYE, DANE DOLEME GUA DIOUGUE FEULE DI GUINAWOU POUR DIEUL LIMOUYE SOUTOROLOU. CERTAINS D 'EUX ON PEUT LES VOIR CARREMENT SURTOUT LE VIEUX, QUEL VERGOGNE. IL FAUDRAIT DES GARDES DE NUIT GNOUYE RONDE LES LIEUX. BAYE MOR. MES FELICITATIONS, TU ES UN VRAI BATTANT, UN SENEGALAIS BRAVE , DE BON COEUR CA SE VOIT. JE TE SOUHAIT LE MEILLEUR A L' AVENIR ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Couvre feu mo wara am bilahi à partir de 22h
Je te jur
Vraiment
Courage frère tegal lepp si lokho yallah dina bakh inchallah
Bon courage Baye Mor.
Courage mon frère dieu est grand 🙏🙏
Pauvre baye mor j ai pitié de toi tu es fort que le dieu tout puissant te vienne en aide pour que tu puisse avoir plus que ce que tu as perdu du courage
Nn mais vraiment il est très respectueux sincèrement mais courageux le bon Dieu va t'aider
Vraiment ça fait mal 😢😢😢
Senegal dotoull bakhe dhe 😢
Coffre dou banque ; agence yi daguene war am compte bancaire ; di def deux versement ci journee bi bala mouy diekh.. Midi ga yobou banque liga liguey ; 16h ga dem def dernier versement comme ca li dess ci agence bi dou barii.. Tabakh ay chambre secrete ci place yi difa def portable you cher yi ect... Fagarou lene svp
Gni dem banque sah dagne lene di agressé
Que le Bon Dieu vous assiste mon frère