arrestation du présumé meurtrier de sa fille : la mère de Diarry parle " Gni di Wakh Dama Sagane"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 20 янв 2025

Комментарии • 328

  • @dominicaandrade1923
    @dominicaandrade1923 16 дней назад +112

    Mme Sow,
    La douleur est immense en tant que mère moi moi-même. J'aurais voulu être à vos côtés. Je vis pas au Sénégal...qu'importe ce que les gens disent..
    Que Dieu vous donne la force de supporter cette peine, voir cette douleur..
    J'ose croire vous rencontrer un jour. Merci à nos policiers
    qui ont fait un travail remarquable.

  • @SodaSall-yd9bw
    @SodaSall-yd9bw 16 дней назад +37

    Ma sha allah Fadel
    Mais justice pour Aziz et Wally 😭😭😭😭

  • @hawadiallo8633
    @hawadiallo8633 16 дней назад +49

    Bien parlé ma chérie yalla na yalla dougalko Aldiana firdaw's

  • @Kifawade8963
    @Kifawade8963 16 дней назад +39

    Ndeyssane képeu kouy yaye rek sa khôl métina😢 si quitté le quartier peut atténuer ta douleur défko sinon il sera très difficile de passer chaque jour devant le lieu du crime. Massa yalna égalé ndawam thia Janatoul firdawsi

  • @FatouWade-d1u
    @FatouWade-d1u 16 дней назад +12

    Bilahi ❤yaye dioylo nama😢yana la Yalla maye kholou mougne té diarry motalé ndawam Adiana firdaw si 🙏

  • @SeynabouFaye-b6q
    @SeynabouFaye-b6q 15 дней назад +9

    Machallah tonton Fadel sa ligueye rafetna et courage maman diarry yalnako yalla yeureume té khareko aldiana metina 😢😢😢😢

  • @Sofieba-v3t
    @Sofieba-v3t 16 дней назад +115

    Arrêtez de dire que la maman n’a pas pris sa responsablitè ameu leneu yeurmandè thi ki way

    • @matyrassoul9141
      @matyrassoul9141 16 дней назад +7

      Vraiment

    • @khadimgueye467
      @khadimgueye467 16 дней назад +8

      Je suis désolé et je suis très mal placé pour juger vu que je ne suis pas mère. je compatis vivement mias toujours est il que ce n'est pas normal qu'une enfant sorte aussi tard. C'est un constat général dans tout le pays. Les parents sont trop démissionnaires et ça fait peur.
      Ca n'enlève en rien la reprehensibilité du criminel toute fois.

    • @kitokoken2187
      @kitokoken2187 16 дней назад

      ​@@khadimgueye467 yaw hana toune ngay dégué. Le criminel est venu le trouver devant chez elle, yobou ko . Vous voulez quoi au juste , que chaque parent attache son adolescent à ses pieds. Soyez humain dans votre put*in de vie une fois. Si vous ne pouvez pas être compatir passer votre chemin.

    • @hfhgg-bm2to
      @hfhgg-bm2to 16 дней назад +1

      Walahi li dal nie dafa metti

    • @TifaBa-tiktokeuse
      @TifaBa-tiktokeuse 16 дней назад +1

      Ndeysane metina trop😢😊

  • @Fari-h9j
    @Fari-h9j 16 дней назад +29

    Pour l amour de dieu cette dame souffre ne dites pas du mal sur elle aider la et prier pour le repos en paix de diarry

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 16 дней назад

      *Vraimnt 😢c’est tt ce qu’elle a bsoin pas autre chose🥺*

  • @Euzzi_01
    @Euzzi_01 16 дней назад +31

    Balay walay yalla reck moy boor❤machallah kou gueum yalla nga ❤️❤️❤️

  • @AlimaDièye-f5q
    @AlimaDièye-f5q 16 дней назад +23

    Yalnako yalla yeureum te khareko aldiana billahi mane sœur bi dafma dioyloo yalna yalla maylén kholou mougne

  • @fatoutoure7235
    @fatoutoure7235 16 дней назад +6

    Machallah Fadel ton travail est reconnaissable
    Soit forte sister bb Diary yalla nako yalla kharei aldiana firdawsi

  • @marieheleneberre8736
    @marieheleneberre8736 16 дней назад +36

    Wadji Aka bone nite kou doywarle.
    Diari yala ne deuko ak Seydina Mohamed PSL.
    Amin yarabal alamine.

  • @timadieng2221
    @timadieng2221 15 дней назад +4

    Ndeysane même la mère de diarry elle est trop jeune ndiabote rék moko diap yalla nala yalla may xoloub mougne nous sommes de toute cœur avec vous ✊✊

  • @telemaison-t5n
    @telemaison-t5n 16 дней назад +28

    Man dé kham mouma khalé bi nékou ma Sénégal, Wayé afaire bi dama touché diouy na ba sone, Li dafa niaw masa yalla nala yalla may, Kholou mougne guem ga yalla courage machalah

    • @NdayeKebe-e1l
      @NdayeKebe-e1l 16 дней назад +3

      @@telemaison-t5n amine yarabi sapa bopi moye méti ndak ay dioye amna nite you bone Sénégal bo Sénégal tediou sakh doutakh ga Mouthe yallana yalla samal soungou ndiaboyi netina

  • @makhouwaly2226
    @makhouwaly2226 16 дней назад +23

    K firdawsii soit sa demeure éternelle 😢 guéneu bess lé mofii nek rkk mes adouna lou métti yagg nafi courage mamans 😭😭🙏

  • @Createurdecontenu-ow9mn
    @Createurdecontenu-ow9mn 16 дней назад +24

    Ndeysan Fadel mo bakh té ame yeurmande ❤❤❤ courage mère

    • @NdayeKebe-e1l
      @NdayeKebe-e1l 16 дней назад +4

      @Createurdecontenu-ow9mn Bilay Fadel kholbi mo rafete dioy rek laye ndakh Kayi doywar am Sénégal yallana yalla fayko

  • @LafemasonhomSy
    @LafemasonhomSy 16 дней назад +23

    Amiine waay fadel .yaye dji dina dioy deh lii dafa metti yalna yalla dolli ko kholou mougne

  • @SwaloMbacke-u2l
    @SwaloMbacke-u2l 16 дней назад +6

    Ndeysan khalebi yalla nako yalla yueram Fadel nit kou bakh nga

  • @aissatoungom319
    @aissatoungom319 16 дней назад +10

    Ma cha Allah. Yallah na len Yallah may ndegeurlaye ak kholou mougne

  • @FatimandaoTymandao-gr4gl
    @FatimandaoTymandao-gr4gl 16 дней назад +15

    Batt bi sakh dafa dem ndeyssane. Yalnalen deudo diam té yallah mousseul niou si natou yini mel ak diour kouy dieuf lii.
    Mbokou wadji tamite, lii metineu si niom torop, bokkak niit mou dieuf lou tolni tamite nekhoul.

  • @omzothiam5306
    @omzothiam5306 16 дней назад +24

    Wallahi diaspora bi yeup amnaniou lounene meti diarry repose bien 😢

  • @KhoudiaKane-p5j
    @KhoudiaKane-p5j 15 дней назад +2

    Bilay yay gore yalnala yalla may kholou mougn té mayla lenen Lou geune diarri yalna motali ndawam aldiana kou répp ken meunouko sammeu 😢

  • @AmdyMoustaphaLo-uf8cc
    @AmdyMoustaphaLo-uf8cc 16 дней назад +11

    Machallah yalla na sa borom yeuram KO té khariko aldia Nay firdawsi

  • @charlotteantoniabassene-wg1yo
    @charlotteantoniabassene-wg1yo 16 дней назад +12

    Courage ma soeur et la soeur de diarry elle m'a fait tellement pleuré

  • @beatricemonteiro6539
    @beatricemonteiro6539 16 дней назад +6

    Mes sincères condoléances paix à son âme depuis le Texas 😢😢😢😢😢

  • @Amouthia
    @Amouthia 16 дней назад +3

    Massa yalna YALLAH mayeléne kholou mougne métina trop.
    Nitte gni arrêté léne yeureume mo gueune yédeu li ame amena ba paré na justice deff liguéyame rekk.
    Diarri yalna agali ndawame Aldiana
    Massa yaye boye métina trop 😭😭😭😭😭😭😭

  • @DeboooMbaye
    @DeboooMbaye 16 дней назад +3

    Alhamdoulilah rafétal ge❤yallnako yalla yaram ko game yalla ge

  • @fatousamba2424
    @fatousamba2424 15 дней назад +5

    Yayou diarry siguil ndîgalê yalla n'a nala yalla May kholoup mougn

  • @aichandiaye3651
    @aichandiaye3651 16 дней назад +4

    Toute nos condoléances à la famille de diarry Sow et toute la population le Sénégalaise gnoungui bok ak yéne nakhar bi di léne gnanal yalla mayléne kholou mougn

  • @DieynabaBadji-p2l
    @DieynabaBadji-p2l 16 дней назад +11

    Masça mougneul du courage soit forte que Dieu l accueil dans son paradis

  • @PendaDialo
    @PendaDialo 16 дней назад +15

    Yalla Yako yalla khare aldiana

  • @aidaguene1948
    @aidaguene1948 16 дней назад +9

    Thieuy Adouna métina😭😭 yalla nala yalla may kholou mougne

  • @MaguetteDeme-lk8qc
    @MaguetteDeme-lk8qc 16 дней назад +84

    Qu'importe elle devait voir sa soeur avant l'enterrement 😢😢

    • @pbcft4235
      @pbcft4235 16 дней назад +22

      Esk yw cv Loy waxni cette image pourra la traumatisé durant toute sa vie

    • @soukeynandiaye6366
      @soukeynandiaye6366 16 дней назад +1

      @@pbcft4235non au contraire le fait que mou beugone ko guiss ta mounouko guiss lolou meuneu takh elle ne pourra pas faire son deuil pour diary gueine si mom

    • @Createurdecontenu-ow9mn
      @Createurdecontenu-ow9mn 16 дней назад +12

      Dafay gueun meti te image bi dafay dess si bop bi

    • @SokhnaRoubaSaliou104
      @SokhnaRoubaSaliou104 16 дней назад +12

      NDEYSANE XAMNA DAGNOUKOY PROTÉGER 😢PEUT ÊTRE IMAGE BI MOO TAX 😢YALLAH NAKO YALLAH SAMM TÉ MAYKO XOLOU MOUGNE 😢MA PAUVRE ELLE EST TRAUMATISÉE...YALLAH NAKO SOUNOU BOROM TAXAWU SAMM KO TÉ DIARY MOTALI NDAWAM THIA ALJANNA

    • @Fanysarrfany-z5d
      @Fanysarrfany-z5d 16 дней назад +2

      Ñaw est ce que ça va 😮

  • @PapeNiobaFaye
    @PapeNiobaFaye 15 дней назад +3

    Merci yaye lou ler nga wax waxi kou gueum Yalla nk ndogal la Yalla mo ko dogal nitt yi ken mounou leine térer wax masta yaye naniou ko nianal rk lolou la sokhla 🤲🏾

  • @Nana-dr1iv
    @Nana-dr1iv 16 дней назад +17

    Ay way boulen ko dolil nakhar 😊saganul ndogual mo nieuw 😢

  • @KaneSeynabou-e6x
    @KaneSeynabou-e6x 16 дней назад +10

    Ooh Ndayesan 😭😭

  • @fatoubintoufall4641
    @fatoubintoufall4641 16 дней назад +8

    Meme bou neker da sagane sakh (cii wakhou yener yi) dou wakhou mbollo bone guen trop di nek cii nakar
    Niou koy saga 😢😢😢 amolen khol dh

  • @mariadiouf6248
    @mariadiouf6248 13 дней назад

    Toutes mes condoléances à la famille Sow et fière du commandant de la brigade de Malika elle fait correctement son travail je la souhaite une excellente carrière avec tout son équipe

  • @NdeyeKhoudiaSow
    @NdeyeKhoudiaSow 16 дней назад +6

    Yalna ko souniou borom yeureum kharé ko aldiana firdawsi 🙏 famille bi yalna lén yallah may kholou mougn surtout yayame

  • @NdeyeAstouSeye-c6e
    @NdeyeAstouSeye-c6e 16 дней назад +19

    Méttyna lolll YALLA may xolop monge 😔😭😭😭

  • @lilmbaye29
    @lilmbaye29 15 дней назад +2

    Très cruel cet acte. Yalla nalène yalla taxawu yéne nieup vraiment.

  • @MameArameSy
    @MameArameSy 16 дней назад +7

    Yaye bou dall nga mongui maifatali sama rakji bidomambi ganio mou am jome andak yalla billakhi😭😭😭😭😭😭

  • @korkadiop7847
    @korkadiop7847 16 дней назад +11

    Yalna yala mayelene holou mougne Fadel Yalna yala goudal sa sa fane

  • @nogayelibasselaye3811
    @nogayelibasselaye3811 16 дней назад +5

    Maréme masta naniou mougne rk laye makhtar yalla nako baye laye térou téral ko😢😢

  • @deugmoyndieukmoymoudie8279
    @deugmoyndieukmoymoudie8279 15 дней назад +1

    Ndeysaan Macha allah Mme Sow Yalna yala mayla kholou mougne thi barké Seydina Mouhamed salalahou aleihi wa salam yalna yala yeureum diégeul té geureum Diary Sow 🤲

  • @ramataly5255
    @ramataly5255 16 дней назад +21

    Massa soeur metina trop yallah nala yallah mayla xolou mougne

  • @dadotheresediouf2236
    @dadotheresediouf2236 16 дней назад +7

    Ça se voit que c’est une bonne mère vraiment c’est difficile 😢😢😢😢

  • @NdeyediakhateFall
    @NdeyediakhateFall 16 дней назад +6

    comment on peut être si méchant elle est très petite khawma noumou defff ma raye ko kiii dafa fragile nga raye koi niii 😢😢

  • @MbayeFall-j2m
    @MbayeFall-j2m 16 дней назад +29

    Billahi magi fi italy dama dioye ba sonnou bi magam dji di wakh 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

    • @mamadoudiop6621
      @mamadoudiop6621 16 дней назад +2

      Italy binga toudou pour lanla

    • @MbayeFall-j2m
      @MbayeFall-j2m 16 дней назад +2

      Dala mety walla dama khamni wa adina yèpe la mèti

    • @MatarDiallo-n3m
      @MatarDiallo-n3m 16 дней назад +1

      Bilahi dafa meti

    • @NdiobaDiouf-sg8er
      @NdiobaDiouf-sg8er 16 дней назад +2

      Mak dji mo Dioy lo ndiepou 😭😭

    • @WEUZ-h50
      @WEUZ-h50 16 дней назад

      @@mamadoudiop6621louy sa problème ci Italie bimou toudou ?

  • @abdoulaziseganogano5801
    @abdoulaziseganogano5801 16 дней назад +8

    Kou guem yahlla gua ndeyssane repose twa en paix

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 16 дней назад +2

    Courage yallanako yalla yeureume té khareko alediana amineeeeeeee

  • @fatougueye8705
    @fatougueye8705 16 дней назад +8

    Yaa goré walahi anzim 😭😭😭😭😭kou gneup dioyaal bou dioyy
    Mettinaa

  • @RamaGueye-v3s
    @RamaGueye-v3s 16 дней назад +2

    Diarry sow yalla nako Yalla yeureume kharèko aldjana fir daw si amine ya rabi 😭😭😭

  • @diarra_chou8497
    @diarra_chou8497 15 дней назад +1

    Masa ma sœur Diary niep nioko dioy man affaire bi nimou tangalè sama xol eupna trop yalnala yalla may xolou mougne 😢😭😭😭🙏

  • @elzodieng8067
    @elzodieng8067 16 дней назад +5

    Ndaysan metina 😢😢😢😢😢

  • @adamandiaye8602
    @adamandiaye8602 16 дней назад +6

    Paix a son âme ke le bon dieu l acceuil au paradis c vraiment dure du courage aux parents

  • @sambandiaye3707
    @sambandiaye3707 16 дней назад +4

    Yalla na ko yalla khare all Diana

  • @MaguetteBoye-e1x
    @MaguetteBoye-e1x 16 дней назад +7

    MAchallah ❤❤

  • @NatouchaDiop
    @NatouchaDiop 16 дней назад +9

    Bilay mane mi meuseugoul am done rek damasé dioye ba melni cou meuseu diour wayé yalna léne yalla doli kholou mougn 🙏🙏

  • @Bébéamina-x8u
    @Bébéamina-x8u 16 дней назад +6

    🙏🙏🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋😭😭😭😭😭😭 diary namnala Lou bari tu nous manques beaucoup 😭😭😭😭😭🕋🕋🕋🕋🕋🕋🙏♥️♥️

  • @SokhnaMariamaDiaw
    @SokhnaMariamaDiaw 15 дней назад

    Ndeysane qu'elle repose en paix yallah n'a la yallah maay xolou mouggne metina trop sk 😢😢😢

  • @Bluerain-j2v
    @Bluerain-j2v 16 дней назад +1

    Gni gui lay massawou bou bakh.
    Yalnala yalla may kholou mougne té dolli la ay kheweul, ak ndiaboot gui yeup , macha Allah

  • @seringefalloudiop1994
    @seringefalloudiop1994 16 дней назад +3

    Ndaye san ndaw su guëm yàlla lou diàfé sénegal ak situation bim tollou ni

  • @diarradiene4275
    @diarradiene4275 16 дней назад +12

    NDEYSSANE yaayou DIARRY jambaar la dafa dem SA ba diekh soit forte on nest de tout coeur avec toi que son ame repose en paix la petite Souadou dit diarry 😢😢😢😢😢billaahi bou nieupou gnibee ngay soga kham ni metite bi meme deug 😢😢😢walay bo mounon dangay touhou yalna SA brom keur am keur nga toukhou si jamm sinon li dou dagne a jamais SA bopou

  • @mamadouaw5597
    @mamadouaw5597 16 дней назад +1

    Yallah nako yallah yeureum té kharéko aldiana firdawsii yallah maylèn kholou mougne vraiment pensé à sa sœur me fais pleurer 😭😭

  • @LibasseSamb-h2t
    @LibasseSamb-h2t 16 дней назад +17

    En tout cas sa maman elle comunique tres bien ndogale Bou gneuwé rk gneuw na ame na loo xame nite manouko échappé té Kiko dfe dou étrangé si kogne bi la deuk da bonne AK boname rek raye ndayame lagne wara défe mou diékh bala Mouy violé wa prison ba

    • @FulaniGirLll
      @FulaniGirLll 16 дней назад +1

      Exactement wakh nga lepp

    • @khadymbengue1197
      @khadymbengue1197 16 дней назад

      Merci bien dit Walahiiiii ko bokaal bénn quartier boula beugué raay do reuthiii 🥲🥲🥲

  • @MameArameSy
    @MameArameSy 16 дней назад +3

    Paix ason am massa métina😭😭😭🙏

  • @ThialaFall-g7t
    @ThialaFall-g7t 15 дней назад +1

    Ndeyesane sokhna si yagui maye dioyelo metina trop yalena yalla agualek dawam aldiana firdawsi yalla mayela kholou mougne

  • @KhadiDiop-sm5ui
    @KhadiDiop-sm5ui 16 дней назад +10

    Meti na trop sakh yalla nako yalla yarame kharee ko adiana

  • @BintaLy-l2v
    @BintaLy-l2v 16 дней назад +4

    Deysan diary yalla Na motali dawam aldiana firdawsi si barke nabi 🤲🤲

  • @binetandiaye8200
    @binetandiaye8200 12 дней назад

    Ndeysann li métina yalla nala yalla may kholou mougn masta

  • @FatimaZahraNdiaye-uc6wf
    @FatimaZahraNdiaye-uc6wf 15 дней назад

    Force a vous Mme courage lii doko meusseu fatei mais yalnala yalla dolli xolou mougne same li dess si ndiaboot gui inchallah teklene loxo metina trop😭

  • @aminatasall2573
    @aminatasall2573 16 дней назад +2

    Ndeysane paix à son âme c dure mais courage ndeysane 🙏

  • @nenesarr2309
    @nenesarr2309 16 дней назад +3

    Massa, Metina 😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @fayefaye6332
    @fayefaye6332 16 дней назад +6

    Ndeysann 😢sa maman sakh xalei la 😥😥😭😭😭

  • @MarieNgom-h1n
    @MarieNgom-h1n 16 дней назад +2

    Yalla nako yalla yéreum massa ma chérie

  • @ndacksene7214
    @ndacksene7214 15 дней назад +1

    Ndeysane comme décès Aziz dabala ba nieupeu dioy nieup la méti.courage ma sœur métina

  • @MaryamaDiop-ce6zq
    @MaryamaDiop-ce6zq 16 дней назад +5

    Yalnala yalah maye holou moigne

  • @AminataBa-o4y
    @AminataBa-o4y 16 дней назад +3

    Yalnala yalla may xolou mougn

  • @ibrakhimadiop6389
    @ibrakhimadiop6389 16 дней назад +1

    Ndeysan yalla nako yalla yeureum té khareko adiana firdawsi amine ya rabbi 1 Fatiha 11 likhlas 😭 té yallla maylen kholou mougne metina trop

  • @khadymbengue1197
    @khadymbengue1197 16 дней назад +3

    Maay lénnko djam elle a des jumeaux dafa sonou
    Ko bokaal bénn quartier boula beugué raay do reuthiii jamais wadji vrai monstre la 😭😭😭😭😭😭

  • @NdackSenediallo
    @NdackSenediallo 16 дней назад

    Massa 😢mettina trop yalla nala yalla mayela kolou mougne masssa

  • @aissatakane5413
    @aissatakane5413 16 дней назад +3

    Paix à son âme 😢😢😢😢😢

  • @BinetaDicko
    @BinetaDicko 16 дней назад +5

    Massa courage

  • @CoumbaMbengue-pe4fb
    @CoumbaMbengue-pe4fb 14 дней назад

    Massa chérie du courage yalnala sougnou brom may xolou mougne meti na trop Ms li mo nekh sougnou brom man dh dioyna sourtou sa dom bi moma geuneu dioylo❤️😭😭

  • @ramatoulayecoulibaly7816
    @ramatoulayecoulibaly7816 16 дней назад +5

    Masta maman métina trop 😢😢Que son âme repose en paix 😭😭😭

    • @WEUZ-h50
      @WEUZ-h50 16 дней назад

      Elle est au paradis 🤍

  • @ndiagasylla7750
    @ndiagasylla7750 15 дней назад

    Machalla yal nala yalla diokh kholou mougne

  • @mariendiaye7670
    @mariendiaye7670 15 дней назад

    Massa maman, Diary yalna khippe aldiana

  • @DiewoKeita-y1p
    @DiewoKeita-y1p 16 дней назад +4

    Nattou la deh suis bouleversée en tant que maman suis terrifiée depuis la Mauritanie

  • @EvachouDiop-yp2pn
    @EvachouDiop-yp2pn 16 дней назад

    Yalna KO yalla yeureum té kharé KO aldiana firdawsi 🙏🙏🙏🙏

  • @AdamaNdiaye-fm3fu
    @AdamaNdiaye-fm3fu 16 дней назад

    yalla nako yalla yeureum té khareko al dianna firdawsi Amine

  • @YgvJh
    @YgvJh 16 дней назад +8

    Limetina torop te yore chekh dafameti 😢dotaldara

    • @khadymbengue1197
      @khadymbengue1197 16 дней назад +1

      Walahiiiii bénn bébé rékk dangaay sonou wakhouma naak 2 bébés 😢😢😢

    • @NdiobaDiouf-sg8er
      @NdiobaDiouf-sg8er 16 дней назад

      ​@@khadymbengue1197bilay 😢

  • @MAMIDIOPLAYE
    @MAMIDIOPLAYE 16 дней назад

    Yallana yalla yeureum te khaŕé adiana firdawsi mama baye laye térou ko téko amine yarabi

  • @AstouAstou-bq4oi
    @AstouAstou-bq4oi 16 дней назад +1

    Que son âme repose en paix.soit forte ma chérie 😢😢

  • @Mameboussofall-bl2ys
    @Mameboussofall-bl2ys 13 дней назад

    Yalnako yallah yeureum

  • @Thyphanie8019
    @Thyphanie8019 16 дней назад

    Qu'Allah accepte nos prières et l'accueille dans son paradis,vous donne la force de supporter.

  • @AdamaSow-mb5tj
    @AdamaSow-mb5tj 16 дней назад +1

    اللهم اغفر لها و ارحمها

  • @MariamNdiayr
    @MariamNdiayr 16 дней назад +3

    Ndeysane

  • @SigaMbacke-wk2id
    @SigaMbacke-wk2id 16 дней назад +1

    Massa metina trop dama sé dioy ba sone😢😢😢😢😢

  • @OusmaneSall-l7n
    @OusmaneSall-l7n 16 дней назад +4

    Kou ray ñou ray la mou diéh