Machalla todiati ngafi. Mère Diop bayiwoula ngay plaline aki any ci mbed yi. Djiguen desskoy diangal togou. Elle est fière de toi de la où elle est. Yana xipè aldiana
5 лет назад+2
Sow Ndeye codou Ameen wayy ma Cherie 😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️
Merci Tata je me vois à travers ta modeste personne la cuisine cé ma passion et Dieu merci je le fais très bien avec bcp d’amour ki est la base pour être une bonne cuisinière. Merci infiniment Tata bisous
En tt cas suis ravi dioyouma sama diabar ki est au senegal liguamay diangual amoul fene mashallah dal contane na ci yaw kanta les dislike niomla rek nane mougn
mere diop yalla nagnou ko yalla fayal ta marietou prepare avec amour joie et bonne humeur neko si rell ak youbou yabayi gno koy safal tu partages ton savoir yalla nangafi yag lol te weur DIEUREDIEUF SHOUKRANE MERCI
Tata Mariétou , beug naala daal . Doundal weral , amal diam diou sakh dakkk , sounou Borrom defal la Sahaadatou Daarayni. I love you soo much.Big kiiiissss
J aime bien tes expression néko ti niouk sou niou boujouyaba yi néko ti reule, non tu animes tes vidéos bravo ma belle.j adore soupe kandia ,moi aussi je le fais avec du saumon c gras et il n y a pas de yahe. Hahaha.omega fait du bien
Tata wa Europe danio beugue poivrons ak oignons vert d 😂😂😂😂😂 mo takh niou beugue ko def si tous les plats. Comme d'habitude soupe kandia bi diap na forme macha'allah chapala
maacha allah sama plat préféré. sama Papeu aussi dako beuguone.ndeysane.yalla na yalla wéreul say thieur gnok katane gui.nga yagueufi lolou dignou wane gnou bakh yi maacha allah
Effectivement senegal tiir bi dagnoukoy rakh tout le temps donc mmere yi dagnou done def tomate merci tata mane mi moussou ma guiss lou verte si souou kandja
Man deh dama moudjei beugu « soupe kandjjj » bou dieun comme niko ta Marietou waxei sawaroumassi won yapp rek mais bii dal Mashallah daw niou tester ko fofa todj merci encore tata yagu fii LOL tei weer 💋❤️
Thiatou Papam jerok lay wakh sama tante bi nek state nakh xamouko ouni ma khamnako marietou ibadou mani ko kirassoulilay doma wne photom mouni ma kone nga d ladj koko 😂😂😂
Je suis bien d'accord avc toi moi je ne prépare pas du Soupou kandia avec de la viande et poisson, et je ne mets pas d'ognon vert ni persi chinois, ça change le goût. Je le prépare com toi et c'est délicieux
Tata Marietou, tey maa lannkkk dou ma commentaire... niamou kandja rek ak kong fumee. euyy waaaay. je me tais. bayil mes yeux lekk affaire bi mou ressak jamm.
Bonjour sokhna Marietou vraiment mâcha allah pour tous ces bon plats Mais encore une fois à quand un couscous marocain Car je serai ravi de voir comment vous faites. Mâcha allah j’adore toutes ces petites expressions quand vous faites la cuisine c’est adorable comme tout et merci de mettre nos plats du Sénégal à l’honneur.coucou de Paris
5 лет назад+1
Mariama Ambareck Insha Allah bientôt merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Am I Nigerian living in Senegal, me and my kids love all Senegalese dish so much. I can prepare them very well. Thanks so much I like your videos
Machalla todiati ngafi. Mère Diop bayiwoula ngay plaline aki any ci mbed yi. Djiguen desskoy diangal togou. Elle est fière de toi de la où elle est. Yana xipè aldiana
Sow Ndeye codou Ameen wayy ma Cherie 😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️
Thieuy soupe kandia aka nex meune nako lék chak jr dérangewouma long vie a ta mariétou
Hahaha kon dou mane dongue 😂😂
Oh ta marietou merçi mane soupe kandia beuguoumassi famille vert
Tata mareme dama la fan beugeu la . Marie Noëlle mi thi Benin
ohhh merci wayyy my love ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😘😘😘😘😘😘
Merci beaucoup tata je t'embrasse depuis la France yagui mey weteuli ba parai dima diangal merci beaucoup way
Mame mere diop yalla na yalla yok lerame tata marietou yalla saraham yagu si sa lokho
Mère diop yeup meuna togua machalla manne mi sama goro la meune plat sénégalaise you barré té diop la tiante yalla na khipe sa aldiana
Soupe Kandia rek néki, agneci, rer ci derangéwouma..... oh..... Aka mako beug 😍
J aime l originalité vraiment chapeau ❤❤❤❤❤
Ma scha Allah, merè Diop yalla nako yalla yeureum 🙏
Marieme Dieng Ameen wayyyy 😘😘😘❤️😘❤️
Allahouma amine ak bep dioulite barké Mouhamed Ibn Abdallah psl
Macha ALLAH merci soeurette nékha Thy diam ak salam est longue vie très bon plat
No stress feeling Mariatou Ress ak Jama and may our beloved mum continue to rest in perfect peace
bilay tata mariètou wakhatikoo soupe kandia yap ak dieum momm mère diop a raison pirrr andoul dara dafay dawww yaram bilay
Je vous suis depuis la Chine namouma dara dakh yaw bilay ya bakh
Tata Yallah nga goudou fanne 🤲🥰❤️
Merci Tata je me vois à travers ta modeste personne la cuisine cé ma passion et Dieu merci je le fais très bien avec bcp d’amour ki est la base pour être une bonne cuisinière. Merci infiniment Tata bisous
Rita ernestîne sow Ameen wayy merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Waaaaw merciiiii ça à l’air trooop bon ! Merci pour l’astuce eau+ vinaigre a faire bouillir pour l’odeur . Dieuredieuf 🙏🏾🙏🏾👍🏾👍🏾👍🏾
Soupe kandia bi diarna yone machallah
Soupe kandia original gua fi togg machallah tata
En tt cas suis ravi dioyouma sama diabar ki est au senegal liguamay diangual amoul fene mashallah dal contane na ci yaw kanta les dislike niomla rek nane mougn
🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
mere diop yalla nagnou ko yalla fayal ta marietou prepare avec amour joie et bonne humeur neko si rell ak youbou yabayi gno koy safal tu partages ton savoir yalla nangafi yag lol te weur DIEUREDIEUF SHOUKRANE MERCI
Tata Mariétou , beug naala daal . Doundal weral , amal diam diou sakh dakkk , sounou Borrom defal la Sahaadatou Daarayni. I love you soo much.Big kiiiissss
Soniasall Moustapha merci wayyyy 😘😘😘❤️❤️❤️❤️❤️
Maman sa diww tirr lou néla😍😍😍
Machallah tata mariétou yalna loho bi gueuneu wéere
Wouyaye lekk guéne khéle dé 🤣🤣😘yalla na yalla deff soutoura inchala
Ngaita Diop Ameen 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 Masha Allah
Machalah goudeul fane way tata say recette amna mana😍
Ohhhhh Soupoukanjjjj bi Mach'Allah 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾😘
Waw sama taty la iow man ki la beugue taty chéri sa sopou kandia tokna👍👍👍👍
Ndiaye Bintou 😘😘❤️❤️🙏🏾
J aime bien tes expression néko ti niouk sou niou boujouyaba yi néko ti reule, non tu animes tes vidéos bravo ma belle.j adore soupe kandia ,moi aussi je le fais avec du saumon c gras et il n y a pas de yahe. Hahaha.omega fait du bien
que dieu vous bénisse.tata marietou.tu cuisine très bien merci beaucoup
Ohoooo li dou soupe candia mais soupou caaanje 😍😍😍😍😘😘😘😘🤗🤗thiey Tata Ya dégueu deh👅👅👅😋😋😋 nekhna nekhna mothchaat Bou saparal
Machalla long vie à toi MARIATOU amnasolo😘👍👍
Bakhou gnakk djom bi la meuneta mougn ...
Macha ALLAH.
Mère Diop a fait du bon travail. YALLAH na khippai aldiana firdaws
Awa Kane Ameen wayyy 🤣🤣🤣🤣😘😘❤️❤️❤️
Machallah gouddou fane ak werr
Soupe Kanje bi validei na tarkallah
Machallah sokhna maretou yalnala yalla faye
Salam salam tata marietou machalla Machalla dinala soumi watt dé yalla na yalla goudal sa fanne inchalla
Nabou Sall Waaleykum salaam mo yawww kholale ma sallen bi beugeu thieb
Machala Tata meune nga lingaye dèf waye machala je vous adore😍
Marietou Sarr merci ma sœur 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Ma cha allah sama toguolokh bi soupe Kandia sama plat préféré
Tata wa Europe danio beugue poivrons ak oignons vert d 😂😂😂😂😂 mo takh niou beugue ko def si tous les plats.
Comme d'habitude soupe kandia bi diap na forme macha'allah chapala
Aby Tolski 😂😂😂😂😂😘😘😘
Machallah tata marietou pour tes plats sa m’aide bcp je mis refere tout le temps
No ta marietou mo may fathe borom bagas ci sa ben sopé depuis Italy bilaye tata goudal fan 🙏🏿
fadiengsaala dieng 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Mère Diop dal ndanane la wone yalla nako yalla kharè firdaws, yalla na souff sed si kawaw
Aby Tolski Ameen wayyyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Wa birou somo bi gnane gnokoy diaye machalah laf thiat
Fatim Lo marché poisson , the meat and fish markets with asians or Hispanics if u r in the states
Shii tata machala je t'adore 😙😙
Gnagna Ndoye 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Machaallah tata soupou kandji ngako
Tata marietou todia tinga fi daale lèpangui goundouss goundousi macha Allah
maacha allah sama plat préféré. sama Papeu aussi dako beuguone.ndeysane.yalla na yalla wéreul say thieur gnok katane gui.nga yagueufi lolou dignou wane gnou bakh yi maacha allah
Merci wayyy Tata pour la recette.
Mashalla tata marietou😍😍😍
Mashallah 😘 sopou kandian mongui plaçame merci beaucoup waye😘
Machallah sokhna Marietou lingay reugeul amoul féne baparè nak limasi geuneu nèkh moy ni ngay wakhé dál sama mbokou Ndar Ndar rék ngama diokh eupeunaa
sama plat niam naim ah macha Allah
Effectivement senegal tiir bi dagnoukoy rakh tout le temps donc mmere yi dagnou done def tomate merci tata mane mi moussou ma guiss lou verte si souou kandja
mére diop yalla na khipé aldiana fildawsi🙏🏾🙏🏾🤲🏽🤲🏽
mame fama ndaw Allahuma Ameen 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘❤️❤️
Non Marietou!!! machala.. ya féroce 🤗👍👍👍
Votre mari a de la chance. Vivement les femmes qui savent cuisiner maachallah
Machalah nekhna rafetna
Yaye chef maman do sèn moron😍
Merci tata Mariétou tahgua ba sama helle dèmna si soupou kandia Machalah ñoune fii amoul kandié instant bi.tata Mariétou somone amna sénégal Wala dañodouro merci 😘😘😘
Souniou mame mere Diop walla na nek si aldiana you geuneu kawé amine
Adjafatima Dia Allahuma Ameen ❤️❤️❤️❤️😘😘😘😘
Amine ya rabi
Merci vraiment amna sollo trop masha Allah 😍
Deguela amena gnoubougoule mélangez jeun ak yapp kouneca ak sa goût ak sa habitude machala
Machaallah sama waleu bokk. Soupe Kandia rekk la beugue
Macha Allah meré boip yalla nako yalla fay 😍😍
Machallah tata Marietou longue vie
Machalla way 19/20 tata
Mashallah you're the best 👌👌🥰♥️
Machalah sama.plat préféré
Machala diar na yone
Man deh dama moudjei beugu « soupe kandjjj » bou dieun comme niko ta Marietou waxei sawaroumassi won yapp rek mais bii dal Mashallah daw niou tester ko fofa todj merci encore tata yagu fii LOL tei weer 💋❤️
Ta Marétou linga soupou kandia eupeuna machala c ta fans n 1 racky gackou
mbaye seye gueye ohhhhh ma sœur chérie please demal thi sama messenger nga diokhma ton numéro merci c’est Ami oubien ? 😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾
MashaALLA tata je t'aime très bien
Machalla sel na
Machalla tata longue vie à toi
Kane moo beugua guiss photo tata marietou oubien visageam.. Je t'aime bcp tata😘😘
Thiatou Papam 🙈🙈🙈🙈🙈🙊🙊🤣🤣🤣❤️❤️❤️😘😘😘🙏🏾
@ Bilaye Tata damalaa beugua guiss bilaye damalaa sopou.. Bouma magué yalla naa melni yaw..
Mane guisko rek la beugue
Thiatou Papam jerok lay wakh sama tante bi nek state nakh xamouko ouni ma khamnako marietou ibadou mani ko kirassoulilay doma wne photom mouni ma kone nga d ladj koko 😂😂😂
@@tatoucagna ayway mak yaw gnon yame guiss ko rek la beugue 😂😂 Mais sa tata bi nathi diap waye 😂😂
Macha allah gounousgounousena😘
Salam, soupe khandja bi diarna yone tothdiati ngafi,merci á toi tata mariétou
Machallah 💖👏👍
walaykoum salam ndaw machallah amna solo😘😘
Je suis bien d'accord avc toi moi je ne prépare pas du Soupou kandia avec de la viande et poisson, et je ne mets pas d'ognon vert ni persi chinois, ça change le goût. Je le prépare com toi et c'est délicieux
Tata Marietou, tey maa lannkkk dou ma commentaire... niamou kandja rek ak kong fumee. euyy waaaay. je me tais. bayil mes yeux lekk affaire bi mou ressak jamm.
Fatima Kane 🙊🙊🙊😂😂😂😂😂😂😘😘😘
Masha Allah soup kandja in the housse
Waw tata mariėtou soupoukajia bi djiapna Form dė
Ah machalah yagui gnouy togne deh gnoune wa team enceinte sougnou khel yaguissi mais machalah na ress ak diam
faring camara ohhhhh euuyyy waayyyyy ballen ma 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
@ ah mane merone na dale wayei yoneima sama waleu rek ma bale la nank
Oh la la manchallah 😍😍😍
Tata mariétou comment tu vas ,je suis une nouvelle abonnée ,merci pour tes bonnes recettes
Bonjour sokhna Marietou vraiment mâcha allah pour tous ces bon plats
Mais encore une fois à quand un couscous marocain Car je serai ravi de voir comment vous faites.
Mâcha allah j’adore toutes ces petites expressions quand vous faites la cuisine c’est adorable comme tout et merci de mettre nos plats du Sénégal à l’honneur.coucou de Paris
Mariama Ambareck Insha Allah bientôt merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Mame ma beugue sokhna Mariètou si sama khôl 💓💓
maimouna ly 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘😘❤️❤️❤️
Tata marietou yagu fi lol tei weir mala tipo❤❤
Très bien 😋♥️🥰😍
Merci sama plat préféré ma maman
Je suis nouvl sur ta chaînne ya moune togou
dialiya sakho Masha Allah merci wayyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machala waye
Merci beaucoup!😘
Ma Sha Allah.
Salam marietou .mme sambe nouakchott grande soeur de mme fall New York .contane Si lo togue rek .les termes que vous utilisez mo may danelle.Bravo❤️
Bilay iow toguolok ngua machallah 🙏❤️👏👏
Mashallah tata chérie laf thiat
Machalah