Dakhine Mbeup

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 янв 2025

Комментарии • 332

  • @sodadiop9851
    @sodadiop9851 3 года назад +5

    Mashala yalanala Yalla faye.Louma meunoul thi yaw lako diangué té kou top sa cheminement limoul togue d'où raté merci beaucoup et longue vie à toi.

    •  3 года назад +1

      Ohhhh merci ma grande insha Allah tres bientot Dina recommencè watt filmer merci

  • @mboupaminata1320
    @mboupaminata1320 5 лет назад +2

    Koukay tog si novembre bi.man bama khamouler loumay def sila dakhine eupna.bon dimanche

  • @mamycamara155
    @mamycamara155 4 года назад +1

    Woooy worina dofice nakh dakhine biii way eupeuna 😜

  • @marifay7015
    @marifay7015 5 лет назад +3

    Machallah sama niarry yaye yii yallna lokhoyi weur machallah nekosi reul

  • @fatimakane3052
    @fatimakane3052 5 лет назад +9

    bakhou niak djom :) :) :) Tata Marietou do niiou rayy nak :) Merci tata Fall. Dakhine bi tokk na. wathie na keur gui ba zero! Yal na lokho yi werr. wouyyy bi dakhineee. Ohhhhhh

  • @ndiatteloniang9163
    @ndiatteloniang9163 5 лет назад

    Oh sama tata nél mme fall dakhine bi néna mbeup machallah ndékété yoooo mme fall thi gayi leu yalna sén diam yag

  • @rokhayabadji743
    @rokhayabadji743 5 лет назад

    Dakhine migui place soom wayè loumalen di wakh moye simibi mais tata marietou diokhnama feu vert manchalla content rek surtout les bagages

  • @omarkebe2523
    @omarkebe2523 9 месяцев назад

    Mashalla yaye isso,vous êtes exceptionnel

  • @diaristandiaye7153
    @diaristandiaye7153 4 года назад +1

    An sa dakhine amna diome machalla waw lilane lani tamite

  • @naboudiack4727
    @naboudiack4727 5 лет назад +2

    Bobouu dakhinee bouu tokkeuu Machallahh trés bien😘😘

    • @aidadiallo9689
      @aidadiallo9689 5 лет назад +1

      MAchalla tata marietou j S8 svent tes videos

  • @dienebadiallo3279
    @dienebadiallo3279 5 лет назад +31

    Tata Mariétou! Sa kanam laa beugueu guiss.

    • @tymaamar3188
      @tymaamar3188 5 лет назад +1

      Diénéba Diallo ak mane 😂 Ki dama ko beug

    • @dienebadiallo3279
      @dienebadiallo3279 5 лет назад

      Walayy walayy

    • @miyassegui4060
      @miyassegui4060 5 лет назад +1

      Bilay wakhatiko on est tous curieux de la voir

    • @diarrambaye2897
      @diarrambaye2897 5 лет назад

      Dèmal facebook diguako guisse marietou ndaw

    • @nenediaw940
      @nenediaw940 5 лет назад

      Va sur facebook tu la verras tata bou diongoma lagn am maaaachallah machallah

  • @jazzyyafa4276
    @jazzyyafa4276 3 года назад

    Nekhna mais la prochaine fois, boul Rossi ak dewline! Guerté kiemb bi ak dégué bi rek doyonna. Mais quand même bravo🙏🏽👏🏼👍🏾

  • @seynaboundiaye5004
    @seynaboundiaye5004 5 лет назад

    mane vocabulairou tata marietou dafay raayyyy cheuuuteuuteuuu je t'adore

  • @sochocolatyes4181
    @sochocolatyes4181 5 лет назад

    Nooo Mme fall elle prend tout son temps wa ye bou tegue rek sa xole bi di bègue l'eau à la bouche mach Allah mach Allah thi yene 😍😍😍😍😍

  • @seydacoco5025
    @seydacoco5025 5 лет назад +2

    Sokhena Marietou sa ligaye raffette na Ndaw sa ndéné...comme d habitude..sa likéye dafa meussa rafféte té nékhe MASHA ALLAH 🙏🙏🙏

    •  5 лет назад

      Seyda Coco Tâta Diaw Chimère Senegal Lepeu yawla Masha Allah Yama gnieukeu diokh responsabilité di dirigè Masha Allah séminaires yi mak Diaw Yallah na sa diama yague

  • @khadijadiouf3354
    @khadijadiouf3354 5 лет назад +10

    Wouyyy mbaxall sama plat préféré meunako Agnè rereko ndéko ko ta marietou je t'adore maman chérie

  • @anamay6400
    @anamay6400 4 года назад +2

    Yummy yummy food yes good job thank you 🙏🙏🙏❤️❤️❤️👍👍👍🇺🇸🇬🇲

  • @kannelle
    @kannelle 5 лет назад +1

    Nekhatatiiii. Machala ress akh djam 😘😘😘

  • @fatimakane3052
    @fatimakane3052 5 лет назад +11

    Felicitations Saveurs Planetaires pour reconnaissance bou ASSOCIATION DES SENEGALAIS DE NJ . Yal na done sa ndjiklaay, Tata Marietou. Bonne continuation! Que Dieu soit avec toi. Barkeel ligueybi. Mu done sa mourr ak werseuk. amine. Laf thiat. Ma sha Allah. Alhamdou lilah rabil alamina!

    •  5 лет назад

      Fatima Kane Ameen

    • @aissatoukane6991
      @aissatoukane6991 5 лет назад

      Kane torodo yaa baakh ,
      Rafète khôl , ci sa wakh laco khamé

    • @fatimakane3052
      @fatimakane3052 5 лет назад

      @@aissatoukane6991 domu baay. Merci. Adina amul solo. Lu rafeet rek mo fi xathie parce que lou waay def bopam la ko defal. Loo fi def tey ak loo fi wakh, tu verras les resultats fii ci adina et aussi yomal xiyaam. Y na niep neek ci jamm. Amiin! Tata Marietou mi ngi begal ak dimbali, Yalna ko Yallah begal! Amin ❤

  • @awakane3114
    @awakane3114 5 лет назад +2

    Eyyy tata Marietou li môme Macha ALLAH
    Suur na

  • @babacargningue5682
    @babacargningue5682 5 лет назад

    Oh trop bon come d habitude

  • @khoudiambengue1723
    @khoudiambengue1723 5 лет назад +35

    Lakhass moye tripes en français 😂😂😂

  • @TheKalajulas
    @TheKalajulas 5 лет назад

    Is there any reason why she put the salt first please

  • @pivoine3828
    @pivoine3828 5 лет назад

    😍😍😍Wenibik Tata Mariétou. Bakhou niak diom sa dara dou nior, dou baar, takhal fépe .Ta soda 😂😂😂😂Mme Fall Dakhine bi am na mana mashallah.

  • @kadiathiam3299
    @kadiathiam3299 5 лет назад

    Aye way dakhine bi saff na trop😋😋😋

  • @mamieisseu9925
    @mamieisseu9925 5 лет назад +10

    Macha Allah. Ta marietou in the house. Yalla na lokho bi weer. Gnoune dal sa gaw rek teumbeul lep degu diam. Pour éviter le récupérer l'huile à la fin, teumbeul lep rek c'est plus sain

    • @TuutyLifestyle
      @TuutyLifestyle 5 лет назад +2

      je voulais dire la mm chose pour huile bi tata marietou mome tog bou sain motakh makoy suivre. Machalla laf tiate

  • @fayendiaya8747
    @fayendiaya8747 5 лет назад

    Ma challa sène dakhine normalna madame fall sei bravissima nagamassi yakalal Sama yaye adjaratou soda fall sa guediawaye Senegal .adja marietou maguilaye ziarre mane ndeye magatte fall Milano

  • @Element_Serigne_Saliou
    @Element_Serigne_Saliou 5 лет назад +31

    Eupeuteuleuw 🤣🤣
    Marietou yak Mme Fall provoqué ngen ma deh 😋😋😋
    Wa li tamit nak ken doussi wax
    Khana ma nianal len ngen diap forme rek 😍

  • @souadoudiouf4117
    @souadoudiouf4117 5 лет назад +1

    Félicitations Tata marietou yalla na donn sa dieglayyy 🙌😙😙😙😙

    •  5 лет назад

      Souadou Diouf Ameen

  • @kineleye5941
    @kineleye5941 5 лет назад +5

    oh li nekhna trop sakh merci Marietou diarama Mme FAll

  • @mariamendiayethioye233
    @mariamendiayethioye233 5 лет назад

    Dakhin bakhi khégne sakh ba fi sama keur 😋😋😋😋

  • @sainaboujagne
    @sainaboujagne 4 года назад +1

    Salam mariatu I have a question can you cook dakhine without netetou please respond to to my question thank you

  • @babishabshufayeuh728
    @babishabshufayeuh728 4 года назад

    Li dh moy dakhine salté🙈l’eau à la bouche
    Merci tata🙏🏼❤️

  • @k-dy4210
    @k-dy4210 5 лет назад +3

    Dakhine pouthi pathi tayma yékhal diakhatou 🤣Ta mariétou li beuri na déh thi mane merciii dieureudieuf merci aussi a Mme Fall 👉 fallén yi you bakh lagnou def diko wakhé diko diokhé borom 33 mamou damel yoyou aka malén love 💖

  • @gnimasn5275
    @gnimasn5275 5 лет назад

    Woyyyy dakhhhhhhhh ngi ni wayyyyy😋😋😋😋😋

  • @naboumbengue955
    @naboumbengue955 5 лет назад +1

    Tres bien Tata yagui forme Tata si language bi nekossi touye etc...

  • @bintadiop1058
    @bintadiop1058 5 лет назад +1

    Machalla on direr ke ç très bon 👍👍😘

    • @ndeyekhadadiop2433
      @ndeyekhadadiop2433 5 лет назад +1

      Domou baye dindil " on dirait " bi😂😂😂😂😂😂😂 li kay saparal rek lay dégeu

  • @zeyna2891
    @zeyna2891 5 лет назад

    Mashalah li nekhna settna merci ta marietou waxalma mme fall soopeu nako momitt

  • @kinediallo1432
    @kinediallo1432 5 лет назад

    Tata Mariyatou tay ya tak ma togou dakine bou nékh machall vraiment merci j v salut 😘😘

  • @ndeyeaminataseck9320
    @ndeyeaminataseck9320 4 года назад

    Mes tatas yalnalene yalla fey, khol sédaatineu ❤️❤️❤️

  • @zeynaebenecisse7791
    @zeynaebenecisse7791 4 года назад

    Yana yalla yokhou sa fanne werr diameu ak salam

  • @fatouthiam964
    @fatouthiam964 5 лет назад

    Shiiii dakhineu nagui placam wayyyy Merci bcp a nos deux tatas

  • @oumarmbengue6546
    @oumarmbengue6546 5 лет назад

    Wa li nèkhout eupeuneuh mane dakhine damay fathie machallah

  • @thiorondiaye3855
    @thiorondiaye3855 5 лет назад

    Machallah tata am na solo wa lane moy feu bou niak diom nak no tata amoul

  • @khadyfall4396
    @khadyfall4396 4 года назад +1

    Togna sa dakhine wanthe saparal ...nekh bi mou nekh wooooo

  • @seynaboundiaye6988
    @seynaboundiaye6988 5 лет назад

    Maman marietou souniou Xel yangui toki toki xol yi neinagnou reul machallah yang niouy diangal dal

  • @khadysene8566
    @khadysene8566 5 лет назад

    Mai madame fall sa dakhine ngéwélé n'a machalah

  • @sodasoda8249
    @sodasoda8249 5 лет назад +2

    Machalah Dakhine mi ngui Place laf thiat bec namnala

  • @maimounadiallo3732
    @maimounadiallo3732 5 лет назад +1

    Machalah yallna lokho bi ... merci

  • @koudiedjisakho2968
    @koudiedjisakho2968 5 лет назад

    Machaallah nékh rek yalla Défal lén fann niou goudou ak wér inchallah

  • @awabadjie343
    @awabadjie343 11 месяцев назад

    Macha Allah mome lay togue tèy et ça cera ma première fois merci beaucoup

  • @lachimere5409
    @lachimere5409 5 лет назад

    wooo tata marietou dakhinatina machallah machallah madame fall merci encore

  • @Mizafrica
    @Mizafrica 5 лет назад

    Yakal léne niou waye gnoune wa Paris la France Machalah

  • @matyndiaye145
    @matyndiaye145 5 лет назад

    Dakhine lay done machalla maman

  • @fadieng7615
    @fadieng7615 5 лет назад +6

    No mbeupp nguako kirasoulay👌 you tooyy yii daffa baxx ci yaram

  • @ndeyeattambaye8306
    @ndeyeattambaye8306 4 года назад

    salut tata mariétou je vs aime trooopp

  • @sokhnadiarragueye6491
    @sokhnadiarragueye6491 5 лет назад

    Deukhine mogui placam ooooh 💕💕❤️

  • @balladiop5768
    @balladiop5768 2 года назад +2

    Déggatougne la ani nga?

  • @rokhayagaye1966
    @rokhayagaye1966 5 лет назад

    😂😂weuyyyy t
    Deukhinooooo

  • @aminatandoye7886
    @aminatandoye7886 5 лет назад +1

    Macha Allah ta marietou et félicitations

  • @aidaly8787
    @aidaly8787 5 лет назад +7

    bsr mesdames....cheee ta marietou fiii naineu mbeupp dall.machAllah...😂😍🙌💕

  • @luisamendes6463
    @luisamendes6463 5 лет назад +6

    Bonsoir Tata marietou ! Je suis nouvelle et j'aime beaucoup ta chaîne que DIEU te bénisse.

  • @mberryable
    @mberryable 5 лет назад

    Wa ana Kethiakh bi

  • @nouchaniang
    @nouchaniang 5 лет назад +35

    Lima gueuna nehh si togue yi amoul Jumbo, doli, adja

    • @sow632sow2
      @sow632sow2 5 лет назад +2

      Ak mami

    • @bdjsghbduzg4739
      @bdjsghbduzg4739 5 лет назад +1

      Limoye cuisine naturelle Sénégalais. Sokhna Marietou amoul morom merci beaucoup

    • @khadyfall4396
      @khadyfall4396 5 лет назад

      Une veritable femme de cuisine. .merci tata cherie

  • @adjisalvatoribiendit6031
    @adjisalvatoribiendit6031 4 года назад +1

    Sournaaa macha allah eupeuneu

  • @Sokhnadiarra828
    @Sokhnadiarra828 5 лет назад

    Mbeup mbeupeee !! Na dale 😋😋

  • @fellygomis3430
    @fellygomis3430 5 лет назад +3

    Machalla j'adore ta façon de préparer

  • @topouleye6781
    @topouleye6781 5 лет назад +1

    Mme fall eupna j'ai bien aimé la vidéo i love you

  • @salamallys9234
    @salamallys9234 3 года назад

    Aye ngén machal,,,,

  • @mimasarr849
    @mimasarr849 5 лет назад

    Wouuuuu deukhine bi safna. Diw bi rek ma si diahal

  • @khadygassama6763
    @khadygassama6763 5 лет назад +3

    Machallah madame fall très bon

  • @habydiop7813
    @habydiop7813 5 лет назад +1

    J'apprécie beaucoup votre plat Merci madame fall mon marie est très heureux.

  • @khadeeja3528
    @khadeeja3528 4 года назад +1

    Tata man dh douma lekk tigeu degué mai sama dieukeur nena beug nako ma beug ko essayé Mai meusouma ko togou
    Damay laccé baxam tiép bi dankoy xocc sok k souseul waleu dankoy xocc rek après nga soorr??

  • @mariamadiallo1527
    @mariamadiallo1527 5 лет назад +106

    Non xamna damay moudjei désabonner rek ba Yallah meyma sama bopp sino domou saveurs planétaires lafi nara am 🤣🤣

    • @miinaone4994
      @miinaone4994 5 лет назад +5

      Mariama Diallo yalla n’a say ohm ceddeu ak diam 😘

    • @mariamadiallo1527
      @mariamadiallo1527 5 лет назад +2

      Miinacarlou Wane amine way ma Cherie

    • @kadijachou
      @kadijachou 5 лет назад +1

      manite dina desabonner. eupna si supplice !!!

    •  5 лет назад +1

      Mariama Diallo deeettt way eupeuna defff Masha Allah 🙏🏾🙏🏾😘😘😘

    • @yayoushba9654
      @yayoushba9654 5 лет назад

      @@miinaone4994 😃

  • @fatoumatatraore55
    @fatoumatatraore55 5 лет назад

    Wa tata linga dakhine tayoko. Machaallah

  • @victorgomis3067
    @victorgomis3067 5 лет назад

    C'est Mme gomis trop bon merci marietou

  • @khoudiangom2167
    @khoudiangom2167 5 лет назад +1

    Machallah tata Marietou deukhine mome rathie na thank u for taking out the oil i was freaking about it

  • @aminasow9867
    @aminasow9867 5 лет назад +3

    Mane yague na laikouma dakhine machalla machalla Wa Li lane la si dakhine machalla âme na mana te togu bi rafetena 😊 Magui senegale parcelle la degu faye nala😁

  • @fatoubintoundiaye6569
    @fatoubintoundiaye6569 4 года назад +2

    C est bonne👍👍👍👍

  • @aidathiam284
    @aidathiam284 2 года назад +1

    Bravo bravo

  • @nguissalyndiaye7249
    @nguissalyndiaye7249 5 лет назад

    Yakalma si li kene douko leik di mer dagua feeh âme diam mes encouragements

  • @baldeamie7419
    @baldeamie7419 5 лет назад

    C vraiment formidable

  • @chamifam4093
    @chamifam4093 5 лет назад +1

    Sa donne envi
    Merci tata, yalna la yalla faye

    •  5 лет назад

      chami fam Ameen

  • @ndiayebintou6309
    @ndiayebintou6309 5 лет назад +2

    Taty chéri sa dahin tokna 😄😄

  • @thiaradiop2474
    @thiaradiop2474 5 лет назад +1

    Biiiii dakhine mashaalla

  • @bintadiop2421
    @bintadiop2421 5 лет назад

    Machaalakh diarna yone dal 😘

  • @cocobane
    @cocobane 5 лет назад +2

    Ah tioumm waay, machaallah

  • @fatoudiagne936
    @fatoudiagne936 5 лет назад +1

    Très bien non tata dinama ray....très bien

  • @adoubygayetoukete3063
    @adoubygayetoukete3063 5 лет назад +1

    Machallah tout les bagages

  • @fatimanoor2431
    @fatimanoor2431 5 лет назад +2

    Saf na machallah

  • @souadoudiouf4117
    @souadoudiouf4117 5 лет назад +1

    Macha alla madam Fall deuhine bi diapna formeeee😍😍😍😍😍

  • @assiatoudiop3066
    @assiatoudiop3066 5 лет назад

    Tata marem mi kouko topou bamou seuss kou diongué la. Soniou meunona defal ay video secret de femme ak ay point de diongué dinama neh.

  • @idikimadiaba6918
    @idikimadiaba6918 5 лет назад

    Mala beugeu. Jaime way ohhh. Kharal ma nopi. Ci koor lagnou nekk.

  • @mariamdiane2264
    @mariamdiane2264 5 лет назад

    Tata mariétou sama toma billay je t’aime beugona guiss sa kanam nak

  • @aminatasymbengue7275
    @aminatasymbengue7275 5 лет назад +1

    Mane ca tres bien momaye raye nikoye wakhé rek

  • @aminatakanesywone5573
    @aminatakanesywone5573 5 лет назад

    Tata machaalah merci beaucoup lahassyi trip latoudou en français

  • @fck9801
    @fck9801 5 лет назад +2

    C bien 😂😂😂 tata Mariétou dinama ray

  • @yacinegueye8679
    @yacinegueye8679 5 лет назад

    ceeey Mme fall sa dakhine nena moûte tarkala

  • @khairyaw2209
    @khairyaw2209 5 лет назад +1

    Je viens de découvrir votre chaîne je m’abonne direct💕 ayliii di. Merci beaucoup tata je vais beaucoup apprendre 💝

  • @tallndeyeyatou2500
    @tallndeyeyatou2500 5 лет назад

    Ay tata marietou bilahi mala beugu je t'aime trop