Mane mom j'envie pas les femmes 😂😂🤣 déjà je me débrouillais pas mal et avec les vidéo de tata mom masha Allah kham kham bi dafa guéna yoku. Sou madame bougoul togue maniko khadialma 😂😂😂😂😂 dieuredieuf tata
Merci beaucoup tata Mariètou. Je tombe sur la notification alors que je prépare du Dakhine pour Aladji. Grâce à toi, j'ai ajouté du thiètiakh et dakkhar et je suis certaine qu'il va adorer 😁😁. Much love❤❤
Coucou mon rayon de soleil. Tu me donnes la joie. Wiiipliwww Dewenati. Waw ak biirou de mouton bi et les lakhass. Ç est lele talal beu mou ne niareeeeeeet 😂😂😂😂😂😂😂Woy. Ani dessert bi 🍨. Je t aime depuis Paris. N'a lokho bi weer 🥰🥰🥰❤️❤️❤️🍴🥤. En puissance 💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾 Dakhine gnioulouk
Ndeysane ak lima weur sa dakhine!??? 🙄🙄🙄 dembeu lako togueu mais hamnaa thièp bi mo eupeu!😂😂😂 Thanks again for sharing your knowledge! May Allah swt keeps his blessings on you and your family! You’re a true help to me!
Wa aleikoum salam tata Mariétou. Yalla nala borom bi same yow ak Sa famille té wéreul lokho bi. Demain inch'Allah ma togue ko agne. Ma ngui kharr vidéo salli bi inch'Allah. Dieureudieuf
As'salaamu anlaykum war'Rahmatul'LAH Tata. Alhmdulil'LAH guiss nga yar boubah ak xiir sa doom si toogou dafa bah ndah do xam kouci dieurignoo. Tata imagines tu le nombre de gens qui bénéficient de ta perspicacité culinaire? Mashaal'LAH Yalna ALLAH SWT dooli sutura adounaak laxira. Merci du fond du coeur tata
Maa kham toogou yaye isseu(Togou Ndar Ndar).. dawlen abonnè. Tata Marietou yalna lafi yaggal tè werr 🙏🏾. I’m finally a member of COWAF.. Thank you for sharing.
Salam Marietou. Félicitations pour vos recettes c’est très bien. Mais évitez l’huile et surtout genre diwougnor c’est très mauvais pour la santé quelque soit l’âge
Mane mom j'envie pas les femmes 😂😂🤣 déjà je me débrouillais pas mal et avec les vidéo de tata mom masha Allah kham kham bi dafa guéna yoku. Sou madame bougoul togue maniko khadialma 😂😂😂😂😂 dieuredieuf tata
😂😂😂😂
Gnawe 😁😁😁fan na la, ni le waye
Khadialma kayy 😅😅
Aha contane si iow rek ni la dé
Instablaster.
Ana gny ko Beugueu pouce bleu
Maman mane beguena la dé magui Espagne 🇪🇸 Mé louma begua cuisiné si oiw laye khôl amougnou sa faye gnoune modou modou yi🙏
Man mi
Merci beaucoup tata Mariètou. Je tombe sur la notification alors que je prépare du Dakhine pour Aladji. Grâce à toi, j'ai ajouté du thiètiakh et dakkhar et je suis certaine qu'il va adorer 😁😁.
Much love❤❤
Je touche le bouton j'aime avant même de regarder la vidéo bilay je t'aime Tata Marietou 🥰🥰🥰😘😍❤❤❤❤❤❤❤❤🥰😘
😘😘😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️❤️
Merci dinako tongou inch'Allah depuis Maroc ❤
Tata marietou vraiment je suis très fier de vous que Dieu vous garder longtemps je te kiffe grave
Vous etes meilleur et vous expliquez bien vous faites de bon recette et tu nous fais rire avk le mot rel et tres bien
tu m'a tué tata mariétou héééé mama.tuvm'a tué depuis ziguinchor..tres contente si yow.mashallla.bisoux gros pour toi et tes mets
Soummi naala bou yague 😂😂😂🤣🤪🤪🤪🤪Macha allah dakhine amna solo. Bon appétit Tata Marietou 😋😋😋👍🤪🤪🤪
🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️❤️❤️❤️❤️❤️😘😘😘😘
Coucou mon rayon de soleil. Tu me donnes la joie. Wiiipliwww Dewenati. Waw ak biirou de mouton bi et les lakhass. Ç est lele talal beu mou ne niareeeeeeet 😂😂😂😂😂😂😂Woy. Ani dessert bi 🍨. Je t aime depuis Paris. N'a lokho bi weer 🥰🥰🥰❤️❤️❤️🍴🥤. En puissance 💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾 Dakhine gnioulouk
😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machallah tata marietou dakhine bi mom amna solo .
Tata mariétou borom youbou yaba yii no def machahalah laf thiate dakhine bi saf na dal
Nekhkha di neu machallah yalleu na sa diam yague kheweul bou beurri ress at diam laf thiat ♥️👌👌🙏🙏
Ndeysane ak lima weur sa dakhine!??? 🙄🙄🙄 dembeu lako togueu mais hamnaa thièp bi mo eupeu!😂😂😂 Thanks again for sharing your knowledge! May Allah swt keeps his blessings on you and your family! You’re a true help to me!
Thank you Tata. This is less time and much easier. Love your cooking😍😘🥰
Masha Allah nekhna trop essayer nako c dou long vie à vous❤️❤️❤️😘😘😘
Je suis tombé sur cette recette et je l'ai préparer comme il fallait té dotoumako bayi😚
Alhamdulilah merci
Wouy tata nga ni g lakhasé 🤣🤣🤣🤣🥰
Maa chaa Allah Dewenaty tata Marietou nameloonanioula safatina Baarakale Laah
Sa diguétéque néko thi réle dou thi wakh tamite tata😂 diam ak soutoura❤ si yaw😂😂
Xaral ma niow attaqué sama dakhine. Nekk europe nexoul ay mane liii
😂😂 dankou dakhareu ak mbeli mbeli you are killing me tata.
Wa aleikoum salam tata Mariétou. Yalla nala borom bi same yow ak Sa famille té wéreul lokho bi. Demain inch'Allah ma togue ko agne. Ma ngui kharr vidéo salli bi inch'Allah. Dieureudieuf
Adama BADJI Allahuma ameen wayyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
As'salaamu anlaykum war'Rahmatul'LAH Tata. Alhmdulil'LAH guiss nga yar boubah ak xiir sa doom si toogou dafa bah ndah do xam kouci dieurignoo. Tata imagines tu le nombre de gens qui bénéficient de ta perspicacité culinaire? Mashaal'LAH
Yalna ALLAH SWT dooli sutura adounaak laxira. Merci du fond du coeur tata
Machallah Tata yalla nalène yalla fay yaw ak yaye Isseu
Tata maan ioe la beug😂😘
Maa kham toogou yaye isseu(Togou Ndar Ndar).. dawlen abonnè. Tata Marietou yalna lafi yaggal tè werr 🙏🏾. I’m finally a member of COWAF.. Thank you for sharing.
Tu as tout dit mashallah mes mamans là togou rek la cuisine c'est leur domaine 👌je les suis toutes les 2❤ elles aiment le gombo comme moi😂
Machalah sama plat bi amna maana. Toogue bi djabar na yoon
Dakhine bou am diom j'aime ❤
Oh li nekhna il faut q ma essayé ko c fini do touma rossi dakhine. Merci waayy❤️
Toubab khamoul massa Allah
Tata marietou merci .on veut paella nak❤❤
Lima nekh si tata marietou moy dafa gnakk kignane day aimer yenene togou kat yi
Très biennnn😂😂ni lako Togué tay mai okhhhh lou féss 😂😍😍😍
Machallah marietou ide Moubarak et longue vie
Ya takh ma kham recettes you barii mashallah Yallah na Yallah yok meune gui
Rholala Tata marietou thank you so much. Love you and your videos ❤️.
Ata seck
Maman chérie li amna solo on vs suivre depuis l'Arabie saoudite
Machallah Tata sama plat préfèré
Tata Marietou machallah Borom diam yi mom dall ay façon bakham meunouma ko mougne ay rèlleu ak touye fofou tothie mdr
Tata merci beaucoup pour vos recettes. Yalna yallah faye la.
L'arachide en poudre est-il obligatoire ? Wala moune na niak?
Ameen ma chérie 🙏🙏🙏 guertè en poudre bi meuneu gniak
Merci wayyy 🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️
Machallah tata mariétou vrément amougnou sa faye diambou thi yew
Les composant du nokoss svp
On t’aime très fort MachaAllah
Machalah ❤❤❤
Tata ken Dou iaw Machalah
❤❤❤❤❤❤
Mar shaa Allah 😘😘
Très bien
Machallah gnou setane té gneuw
Machallah deweneti toogou yinekhna machallah
Wouyyy maman dina ma raay 🤣🤣🤣🤣
Version française bi raay nama
Kein doula ray ler na naaaagn waw key
Ayy li safatina diii
Ioe la beug deii
🤣🤣🤣🤣🤣🤣😘😘😘😘❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾😜😜😜
Machahlla laf thiate
Mais c’est pour combien de personne ?
Je pense que je vais venir en vacances après coronavuris 👍👍👍
Machala todje nga fi tata
Machalla Tata marietou
Ahhhh Tata marietou yallah rek mo les faye taye mome je dakhine
Machallah Wala Qouwata illa bila😂😍
Man dall tata jtm😍
Salam à tous. Machallah. Yalna diam yag
Machallah👍👌😋😋💖💞😂😂😂😂merci
😂😂😂😂
Je vais juste faire un petit niouloukk et néko thie bathie 😂😂
Bon appétit 🤩❤️
J'ai aimé ta cuisine sans huile
Machallah machallah mariétou ya dof
Merci Tata longue vie à toi
🤣🤣🤣🤣🤣
Dakh SA boye 😂😂
Un petit nioulouk nekothi bathi non tata Marietou doundal Ndao poulo borom ndoukouman yaw lay weur😂😂😂😂😂
Wa ndaw kounda sama domou bay fo nek? Mba diam
Machalha 😚😚👍
Machallah tt
Mashala tata mariétou
Wa sama rak bi môme hummmm saf sàpp lag thiat
Oh sister Marietou togne guama sama khelbé guithi ndajkhinegui te monoumaka lekeu ndakhtè temps yi worouma lekeu khorom ohho 😢
Machalla tata MARIETOU
Chous d'outils
Machalah
Masha Allah
Macha Allah💖
Nekhna mashalla
Merci tata ,recette pailla svp,damay amm ayy invités le week-end prochain, et je voudrais leur préparé du pailla,merci d'avance 🙏
Ok ma cherie je vais vous envoyez 3 recettes très facile et succulent
ruclips.net/video/PaFwUMcalUY/видео.html
ruclips.net/video/cAJxW9y6H6E/видео.html
ruclips.net/video/uMXTNZrfH3I/видео.html
Merci beaucoup tata que la paix soit avec vous,et que le seigneur vous protège 🙏
Ah Mane beug n'a lii
Gnawww EUPNEU
Deukhineeee is bae.. mais ta youbi yabaa en français
😂😂😂😂😂😘😘😘❤️❤️❤️
🤣🤣🤣 Love sur vous ❤️❤️❤️
Merci tata
Mafi dietou tay mome laye togue rére
😭😭😭😭😋😋😋😋😋😋
Ahhh tay mafi ndieuk tâta doundeul rek yaw
😍😍😍😍
Wa loutakh amoul dakhar wala dousi Dara tata marietou
Si si amna dakhare
Salam Marietou. Félicitations pour vos recettes c’est très bien. Mais évitez l’huile et surtout genre diwougnor c’est très mauvais pour la santé quelque soit l’âge
Et l'oeil était dans la marmite et regardait...
ma chahalla
Merci la famille Sam de Lyon
Ki
Tho! Dakhine sans Rossi mou teumbe ni quelle professionnelle
Mdrrr je suis également très impressionné mashaal'LAH
Impressionnant en effet
❤❤❤❤❤
ma chahalla