Serigne bi faydou awwal amul faydou thaani amul. Faydou chi bopam amoul chi Tariqa Tijan. Aye fen la ak aye tapaleh. Bulen sonnal sen bop. Tapaleh problem rek la. Tenku len chi alquraan ak sunna kom ni ko sunu mak yu bakh yi defewon. Bulen nyu sonnal yen Niassen yi. Yena yakh Tariqa Tijan yen Niassen yi.
Sen thiahaan yee dungen ko fek chi ben keru deena. Dungen ko fek Tiwawone, dungen ko fek Chenebah teh dungen fek Daarou Ridwaan yen Niassen rek yena yakh Tariqa bi motakh ku jog rek saga Saidina Sheikh ak lena chi kilifa Tariqa bim. Lee museeba la. Wasalaam
Machalla machalla machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf mawlana cheikh Mohamed Amine bâ kamalou diné 💖💖💖
Serigne bi faydou awwal amul faydou thaani amul. Faydou chi bopam amoul chi Tariqa Tijan. Aye fen la ak aye tapaleh. Bulen sonnal sen bop. Tapaleh problem rek la. Tenku len chi alquraan ak sunna kom ni ko sunu mak yu bakh yi defewon. Bulen nyu sonnal yen Niassen yi. Yena yakh Tariqa Tijan yen Niassen yi.
Niak khame khame rêk guaye wakhê
Daniouy tegg daniouy féthia
Fethia dagan na chi Sharia wola daa haram chi Sharia?
Sen thiahaan yee dungen ko fek chi ben keru deena.
Dungen ko fek Tiwawone, dungen ko fek Chenebah teh dungen fek Daarou Ridwaan yen Niassen rek yena yakh Tariqa bi motakh ku jog rek saga Saidina Sheikh ak lena chi kilifa Tariqa bim. Lee museeba la.
Wasalaam
Yow khamo leufeul ndeye yame amo kham kham mou nekh la mou nakarila faydou sani si kaw si kanam sa data ndeye
Li Serigne bi wakh moye deg saga amoule béne sence
Boy yow deguay rawantalou rek sagua mome kou amoul arguments rek mokoy def
Wakhêwa khame khame sa khêl rêk guaye wakhê
Yow kou rew gua Amal teguine yow khamo dara di am loye yow kham guama te dou kham GUA ma bou bakh
@@bmbtvjoal9123 waw dêgue na sa wakh wayé nagua défandre sa boppou si kham kham mo gueun li guaye wakh
@@bmbtvjoal9123 mane sama khalate rêk la wakh bou mêr dou thieurou hanrif
@@ousmanediop5542 mais yow yaye kane BO sa khalate wara corrige ay wakhou baye Niass
@@ousmanediop5542 mane si kham kham lay wakh gnoune wakhou baye lagne wakh yow kaye soye dindi indil wakhou baye li moye kham kham fane la baye Niass deugual teugue ak fethie wala alkhourane wala hadiss wala wakhou CHEIKHOU TIDIANE????