Assalamou aleïkoum noungui ziar wa keur gui. Sokhna ci naka yaram bi mba yangui fekh bou bakh. Que le bon Dieu vous accorde une bonne santé et une longue vie thi barbé khadimoul Rassoul
Alhamdulillah c bizarre mais les hommes aiment les vermicelles c pareil avec mon mari et mon fils aussi molène gueuneule couscous xowma noumou dème nonu 😂🙏🏾😘
Machalla yalla na yalla dolli diamou
Amine ma chérie gnou bok lep feke ak tal 🙏🏾😘
Assalamou aleïkoum noungui ziar wa keur gui. Sokhna ci naka yaram bi mba yangui fekh bou bakh. Que le bon Dieu vous accorde une bonne santé et une longue vie thi barbé khadimoul Rassoul
Excellente recette tata. Vermicelles étant le plat préféré de mon mari j'adopte cette recette pour changer. Merci 😍😍😍
Alhamdulillah c bizarre mais les hommes aiment les vermicelles c pareil avec mon mari et mon fils aussi molène gueuneule couscous xowma noumou dème nonu 😂🙏🏾😘
instablaster
Mashallah Mashallah Mashallah tata chérie ! N'a Yallah weral Thieur yii té yokk kham kham bi yaa Rabbi
Amine ma chérie jajeuf🙏🏾😘
Mahallah Billo mérci🙏👍👍😋😋🙌❤
Akassa sis jajeuf 🙏🏾😘
machala sister encore une autre version pour vermicelle . merci pour l astuce des boulettes
Nioko bok domou baye gno far 🙏🏾😘
Salam sokhna billo mashallah encore une autre manière de cuisiner plus rapidement et délicieusement merci et bon appétit chef
Merci ma chérie guiss nga deh 🙏🏾😘
Salam sokhna Billo ✋ Macha Allah belle présentation teytam nekhna💖💖
Ah merci bcp ma chérie jajeuf 🙏🏾😘
Lii me saitane nii khamna ni nekh ne. Sama papa mo wakh deugg 😍😍😍
Machala mane mom c est surtout les KHASSIDA qui me font tombés merci Stouba amoul morom
Akassa ma cherie ah khassida dafa neex mashallah 🙏🏾😘
Hello Billo
Deco impeccable comme d'habitude qui envie de plonger ds le plat.
Deet waye maye nalako nii 😂🙏🏾😘
Machalla sokhna billo 🙏🙏❤❤❤
Akassa sis 🙏🏾😘❤️
Coucou Mme Billo
Est ce que ce serait possible d avoir la recette pour le mélange d épices.
Merci et longue vie à toi et ta famille 😘
J'ai essayé de le reprendre mais je ne trouve pas toutes les epives comme oignons en poudre
Machalah sister très belle décoration
Merci sis jajeuf 🙏🏾😘
Machaallah
Jajeuf ma cherie 🙏🏾😘
Masha Allah 😍😍👌
Akassa ma cherie🙏🏾😘
Machalah🖒...moi je le fesait avc des boulettes de poisson mai c délicieux
Ouye c encore mieux j’adore les boulettes de poisson ma chérie merci 😍🙏🏾😘
@@ChezBillo ah bon..ndeyesane
Masha ALLA 😍😍🥰🥰😘
Est ce que boulette yi sou amoul four meune ngako saf wala nga tayko
Salaam ma cherie waw waxna loolu meun nga def bila dakal du ci changer dara 🙏🏾😘
Salam mangui ziar sama gooro ah ndeysnn danga tawatone ah boula dara daal weral ak diam Barkep mbotou xassida yi
Assallamallikoume Sokhnassi nioguilene di ziarre aka beguee naka jaboot mba lep jam
mashaallah
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Merci amatina soro mais namonala
Ma la raw ma chérie dama la gueujeu guiss ci keur gui contane na trop ma belle yalna Yallah bindala aye yiiw amine 🙏🏾😘
@@ChezBillo sokhna billo sama pape mo décédé temps yi mou méti lol wayé sante yallah loumou déf nonoula
A presto
Machalla
Donc tout le Monde est censé comprendre le Wolof quoi