Machalah dieuredieufe cheikhna docteur mouhammad Ahmad lo leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam ak molem oustaz bouy wakh si alquran ak suna
Kaadu kufriyat aki shirkiyat yi gueune reuy ci guemiñu mourid yi lay guéné, yoyu ñuy wax jeumé ci borom bi metiwuko mais luñuy wax « kilifeu diiné » ñoko meti ? Lolu day wané ni « kilifeu diiné » lañu gueune fonke que borom mi, lolu moy li am Yallah naniu Yallah guindi
Les soient disant oulama ne t'aime pas ne t'inquiètes pas comment un imam peut discuter avec une personne par WhatsApp après on trouve les audios sur l'internet
Même ceux qui ne l'aiment pas savent qu'il tire tous ses arguments du Saint Coran et de la Sounna du Prophète Muhammad SAWS. Pour mettre fin au débat sur le croissant lunaire, l'idéal serait de le confronter à un religieux Soufi.
Yalla nala yalla sam cheikhna Dr
Barakallah ya cheikh senegal mo tocc deuke bou doyware tè diafé wétale sa borome mouye tawhid
Yalla naniou yalla mousseule ci chèytanè
Aka am yar ag tégguiin ! Hafizakal laah
حفظك الله ورعاك يا شيخنا ورفع مقامك في الدنيا والآخرة
حفظ الله شيخنا الفاضل وأطال عمره في طاعته وأعلى مقامه في الدنيا والآخرة
Macha'Allah Docteur
حفظك الله ورعاك
Courage cheikh Ana gni dinio sokhor
Yalna yalla sam sheikhe bi❤
فاصبر صبرا جميلا يا شيخنا. حتى من الأ نبياء كذبو ومنهم من لم يجد صحابة واحدة بعد قليل نغادر ويأتي أخرون
Machalah dieuredieufe cheikhna docteur mouhammad Ahmad lo leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam ak molem oustaz bouy wakh si alquran ak suna
Mashallah dr
Masha'Allah Dr leral yi Amna solo yallna yallah fay ❤❤
Cheikhana cheikh❤
نحبكم في الله يا شيخ ❤❤❤
حفظك الله ياشيخنا
Yal nala yala fay yéw ta samou la ❤
Macha Allah imame Mouhammad Ahmad lo yalla nala yalla defal diame adouna ak alahira Amine 🤲❤️⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐
Mâcha Allah
Yalla nala Yalla samou ❤❤
المعركة معركة عقيدة لا غير حفظ الله شيخنا
حفظ الله شيخنا آمين!
Am na gnou yaraadiko nagn diaamou ji yalla tè baayi reuy ak hastabi
Que Dieu vous protège Dr Muhammed
حفظكم الله من شياطين الانس والجن ❤❤❤❤ يا شيخنا
Sénégal sokhor mo tah dounou dem. Wayei wallahi sunnah rekk Moy deugue
Kaadu kufriyat aki shirkiyat yi gueune reuy ci guemiñu mourid yi lay guéné, yoyu ñuy wax jeumé ci borom bi metiwuko mais luñuy wax « kilifeu diiné » ñoko meti ?
Lolu day wané ni « kilifeu diiné » lañu gueune fonke que borom mi, lolu moy li am
Yallah naniu Yallah guindi
❤❤❤❤❤❤❤
Il faut porter plainte, yombeuneu trop di toumal note ni
𝐊𝐢 𝐤𝐨𝐤𝐚 𝐛𝐚𝐠𝐧 𝐥𝐨𝐤𝐚𝐲𝐞 𝐛𝐚𝐠𝐞𝐞 𝐦𝐚𝐜𝐡𝐚 𝐚𝐥𝐥𝐡
général Ahmad lo walahi
Yaa lene OP kham kham
Gorgui Abdou Aziz Touré dé respecté Na Niou ko Loulou waayé Mandou woul Thi propos yi mou yeukkeuti.
Bilahi wakh nga deugue.
Il Faut Avoir Peur Des Sectes Plus Qu'un Anaconda
Les soient disant oulama ne t'aime pas ne t'inquiètes pas comment un imam peut discuter avec une personne par WhatsApp après on trouve les audios sur l'internet
Même ceux qui ne l'aiment pas savent qu'il tire tous ses arguments du Saint Coran et de la Sounna du Prophète Muhammad SAWS.
Pour mettre fin au débat sur le croissant lunaire, l'idéal serait de le confronter à un religieux Soufi.