Xalass: M£urtre de Bineta Camara, Mamdou Mohameth Ndiaye fait une révélation de taille

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 дек 2024

Комментарии • 176

  • @ndiayeadama659
    @ndiayeadama659 5 лет назад +195

    Gnanale léne binta Camara yalla Nako yalla kharé aldjana firdawsi si barkè seydina mouhamed Psl

  • @adama8898
    @adama8898 5 лет назад +55

    Vraiment ça doit être révolue au Sénégal...Oeil pour oeil, dent pour dent il faut appliquer la loi du Talion....Kou Ray ngou Ray mom la yalla wah

    • @zeinasabaly2724
      @zeinasabaly2724 5 лет назад

      Walaye

    • @leylalati8360
      @leylalati8360 5 лет назад +2

      Laye adama Té enplus sakh dina takh kassoyi libre touti ndakh ray katou nit gnéko fessal

  • @mamadoumambande3584
    @mamadoumambande3584 5 лет назад +1

    Paix à son âme que le paradis soit son demeure éternel je lui ai vu sa photo dans notre groupe WhatsApp hier et nous avons priés pour elle et on continue toujours de prière qu'elle soit parmis les femmes du paradis

  • @yankoubandiaye8825
    @yankoubandiaye8825 5 лет назад +5

    Yallah na binta guisanté seydina Mohamed 🙏🏼

  • @mohamadouthiam1548
    @mohamadouthiam1548 5 лет назад +3

    C'est très cool votre émission et bonne continuation 👍👍👍depuis Paris la France 🇫🇷🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @khadysall7304
    @khadysall7304 5 лет назад

    Ndiaye merci kou dalga yalla nala yalla faye yiw amine

  • @manetoure6189
    @manetoure6189 5 лет назад

    Ndeye bineta guaye yallah n'a yallah yeureme la t'ahallah aldiana firdawessi inchallah paix à son âme inchallah 😢😢😢

  • @alphaba4913
    @alphaba4913 5 лет назад

    Binta yalla nako yalla yerem

  • @abybathily8221
    @abybathily8221 5 лет назад

    Machalah depuis Paris on vous adores

  • @modoufall2994
    @modoufall2994 5 лет назад +42

    kou ray niou rayla mou diékh tak

    • @mormbaye298
      @mormbaye298 5 лет назад

      Yaw li gaw khamoko kou ray dann la wara ray konn ba tagne rayi djèkh na

  • @mbayesdieng
    @mbayesdieng 5 лет назад +14

    Mais kii wakh cadavre biniou retrouver Ouakam néna " Malheureusement jiggen la " même malheur mom dagn siiy sett ay genre wala dara

    • @AJ-or9bk
      @AJ-or9bk 5 лет назад +1

      Lol français la wakh dh a vous de comprendre

    • @malicksow4200
      @malicksow4200 5 лет назад

      Parsk djiguéne danou ka wara yeuram si sens bobou lay wakh pourquoi vous aimez critiquer

  • @niangsalimata8102
    @niangsalimata8102 5 лет назад +4

    Merci beaucoup Mohamed NDIAYE tu as parfaitement raison mane defna 15 ans Maroc mais à vrai dire les marocains sont trop raciste ici même si tu ne vent pas dans la rue on te provoque à chaque fois et si tu as un problème avec eux vous partez à la police si tu comprends pas la langue tu es foutu la maman elle na ka dire la vérité pourquoi elle parle comme ça les problèmes comme ça peut être c'est menant qu'on la mis dans réseau sociaux mais sa fait longtemps ya des filles qu'on appelle les ajii rasta pourtant ses filles ne vent pas dans la rue mais elle sont trop fatigué avec les marocains ils ont trop raciste mais nous qui c'est ce que nous à amener là-bas on patiente beaucoup de choses parce que nékougnou sounou deukeu mais yalla backna yaye nagnou yalla diapaler si Barker seydina Mohamed merci beaucoup 🙏🙏🙏🙏🙏

  • @matardiop8230
    @matardiop8230 5 лет назад +9

    Yalla na yalla yeureum té kharey ko aldiana thi barker khassida yi

  • @nafisatoufall4215
    @nafisatoufall4215 5 лет назад +5

    Machala felicidades sen ligey rafetna trop je suis en España

    • @doundiaye5494
      @doundiaye5494 5 лет назад

      Mdr Kagn nga dém espagne

    • @marichoufall4499
      @marichoufall4499 5 лет назад

      Dou Ndiaye 🤣😂😂bilay do dem dou néna mogui Espagne

  • @alioutoure2655
    @alioutoure2655 5 лет назад

    binta kamara YALLA nako YALLA yeurem kharéko al djana thi b SERIGNE TOUBA

  • @dioumadieng9931
    @dioumadieng9931 5 лет назад +3

    Deysan yalnako yalla yéreum té xaréko aldjana

  • @gnimsbaby8929
    @gnimsbaby8929 5 лет назад +1

    Metina gni fi diongué yalla naniou hipiwé ardian firdaw.yalna naniou sounou borom maï moudiou diou rafet

  • @mamedia6425
    @mamedia6425 5 лет назад +1

    Mamadou mohamed ndiaye deil bayii ba ame information you leire nga dora wakh parcek niti daniouleine di deiglou lane moye lolou leu journau yi binde on a besoin des information clolair please waye🙏

  • @deugrek5110
    @deugrek5110 5 лет назад +12

    Bilay ki dafa melni dama bok ak mom damay khôl fotom chak insbi sama khôl bi mety na trop t dise bilay ki def l'I yalla nagnu sunu borom nite wa prkw pa la peine d mort au Sénégal

  • @adjithiam4148
    @adjithiam4148 5 лет назад +28

    Mais l’autre qui chante la chanson de thione est ce que ça va chez lui ,il est entraîne de donner des informations tristes le mieux mou nopi par respect

    • @serignesaliouniang4227
      @serignesaliouniang4227 5 лет назад +1

      Vraiment nak

    • @ndiayemarie5272
      @ndiayemarie5272 5 лет назад +1

      Franchement, dof rek

    • @ndeyendiaye4695
      @ndeyendiaye4695 5 лет назад +2

      Mane d dama wa warou franchement . Khalebi ki ko def ni yalna ko yalla were bethieuke

    • @sosodia82
      @sosodia82 5 лет назад +1

      C'est cet imbécile de ndoye bane en plus

    • @adjithiam4148
      @adjithiam4148 5 лет назад

      Manque de respect et d’empathie c’est cela qu’il a montré ici vraiment je déplore ça

  • @kimfababy9762
    @kimfababy9762 5 лет назад +9

    Yo Allah yourmomo yaffomo .🤝

  • @papeniang80
    @papeniang80 5 лет назад +10

    Je suis d'accord avec mouhammed ndiaye,il y a bcp de senegalais qui souffrent au maroc

    • @mamandiallo8424
      @mamandiallo8424 5 лет назад

      Mère wakhal lo kham sa bopou ngay protégé egoiste nga trop

  • @combe4823
    @combe4823 5 лет назад +1

    Qu'elle repose en paix

    • @filmpolo1619
      @filmpolo1619 5 лет назад +1

      Aïcha sarr sama domou baye li métina

  • @moustaphaseye5752
    @moustaphaseye5752 5 лет назад +4

    Mouhamed Ndiaye machalla yalla nala yalla lafall thiatt bilahi man mom yalla modogal ma beugg la rk Ndax sa nieme deugg

  • @mbayesdieng
    @mbayesdieng 5 лет назад +4

    Mère yaw so guissoul dangay wakh guisso mais boul wakh amoul, nieup xamnagn nii naar mel cii niit kou nioul. Lingay wakh yeup sa bop ngay protégé . Epuis sénégalais tt le temps dagn lenn dii sonal fepp cii pays nar yii, même Maroc gogou sakh .
    Merci Mohamed Ndiaye 🙏💕

  • @boussoasta6342
    @boussoasta6342 5 лет назад

    binta camara k tn âme repose en paix k la terre l8 soit léger amine vraiment les gens sont hypocrite bilahi

  • @ndeyependadrame5574
    @ndeyependadrame5574 5 лет назад +3

    Elle dit vrai il y a bcp de ressortissant sénégalais ki devrai pa sortir le Sénégal

  • @mamediarrasambtouhfatou350
    @mamediarrasambtouhfatou350 5 лет назад +4

    Inna lilahi wa ina ileyhi radjikhoune yalla nako yalla yeureum firdaws done keureum gou moudiou mètina lool yalla safara li khew si rèwmi si anam you gaw ta samouniou

  • @binetoudiop2643
    @binetoudiop2643 5 лет назад +3

    Sénégalais yi nion wara khameni deukou diambour dousa deuk nek na maroc yague fa marocain yi danion beug sénégalais yi respecté sénégalais yi mane polisou Sénégal la geuneu ragale polisou maroc femme bi limou wakhe deugleu yalla kham nako

  • @coulibalyramata9005
    @coulibalyramata9005 5 лет назад +3

    La méchanté des gens n'a pas de limite tout sa parce que il y'a pas de justice dans notre pays

  • @karafamou
    @karafamou 5 лет назад +2

    Ndogalou yalla diekhna bou yag ki yalla dogaloul niou violeiko reyko. Je le dis haut et fort le Sénégal 🇸🇳 depuis cette alliance de se dire que les droits de l’homme interdisent la charia donc allons et prions pour cette dame qui ne méritait pas ce sort. Kou rey niou rey la nank tei keine dou yekk. Bakar amoussi

    • @aminatadiop5531
      @aminatadiop5531 5 лет назад

      Vraiment loi du talion lagn fi wara appliquer oeil pour oeil dent pour dent legui nieup nè tiothieu

  • @aboubacardiop6454
    @aboubacardiop6454 5 лет назад

    Waa baakh na nagn dm rk yalla bined diam yi guene nio kham sougn bop nei kou ray tei tayko nagn ko rayy ngueini dedet bouñ ko appliquer woone ray bi arrêté na bou yagg

  • @aliounebadaraseck7092
    @aliounebadaraseck7092 5 лет назад +6

    Mouhamet ndiaye yalnala yalla faye

  • @dabyba235
    @dabyba235 5 лет назад +2

    bon travail Khalass

  • @madjiguenendiaye5585
    @madjiguenendiaye5585 5 лет назад

    Repose en paix k le seigneur t accueille dans son paradis amen

  • @meryngom9663
    @meryngom9663 5 лет назад

    Franchement dans ce pays la justice est malade comment on peux gracié un détenu qui n'a pas boucler la procédure je suis de tout cœur avec les pharmaciens il faut qu'ils protègent leur profession car l’état à démissionner

  • @tele1514
    @tele1514 5 лет назад +6

    Mâchala mouhamet deug pire ga wakh bravo

  • @oureyefaye958
    @oureyefaye958 5 лет назад +7

    Repose en paix

  • @sankounkanoute4390
    @sankounkanoute4390 5 лет назад +4

    Yalla nako yalla yeureum teh khare co aldiana

  • @maminianedabakh6702
    @maminianedabakh6702 5 лет назад

    Bilay maman aicha deug nga wakh senegalaise la keine meunouteu comprend dem deukou diambur beug fa df lou wa deuk beu doule df

  • @zeinasabaly2724
    @zeinasabaly2724 5 лет назад +2

    Yallah na ko yalla yerem khare ko aldiana si barke Seydina Mohamed Psl

  • @zakiaidara8081
    @zakiaidara8081 5 лет назад

    Salame dieux il accepte la péne de mor pour çe ku tu par intation et je suis pour que dieux nous protège

  • @abousompare1369
    @abousompare1369 5 лет назад +3

    Les Sénégal sont fatigués partout mais à l'étranger ils pensent qu'ils chez eux fékh bâ deh douniou respecter ben lois. Regarde moi ça ataya cibir bus. Du n'importe quoi bâ nieuwé Europe sa khôl dafay diékh.

  • @famacamara1767
    @famacamara1767 5 лет назад +1

    Militaire yi louye Sénedjieurigne pourquoi dougnou wathieu si terrain non sécurisé yi comme ça dinagnou dissuadé gnouye Déf niawtefyoyou.chaque année gnou recruté

  • @mortalla28marone86
    @mortalla28marone86 5 лет назад +5

    Marocain dal ils vont pas accepter l'anarchie dans leur pays les Sénégalais sont tellement désordonné .dor rek c'est bien

  • @ramadiop5269
    @ramadiop5269 5 лет назад +19

    Métina lol sah emplus niou entéré ko san pr autan kon l'ai identifié kou dém famille wam weurna pa sone

    • @maricmr970
      @maricmr970 5 лет назад

      On cherche même pas à comprendre c'est dommage

  • @beugessaliourekdiouf7226
    @beugessaliourekdiouf7226 5 лет назад

    Ndaw si limou wakh deuge la danouy ataya si bire kham nasi dara

  • @lampseye9769
    @lampseye9769 5 лет назад +1

    Mohammed Merci beaucoup macha Allah yalla nala yalla samou

  • @shashashasha5236
    @shashashasha5236 5 лет назад

    Vraiment c triste comment une persone peut faire sa li esk jam la

  • @adaguiracie4894
    @adaguiracie4894 5 лет назад +1

    Yeen bayi leen ceen wakh you niaw yi
    Elle est là depuis 23ans
    Nous on est ici on vous dit que c’est faut vous insister
    Maroc comme senegal
    Nakh beuri senegalais les nars parlent wolof

    • @chachagaye5777
      @chachagaye5777 5 лет назад

      Bien dit ada maroc mome sincèrement Defna 3ans mais massouma fa ame problème sénégalais yi liniouy def biir maroc souniou ko defone senegal niou raylene donc arrêté

  • @bafitabengeloune6283
    @bafitabengeloune6283 5 лет назад

    Barki yalla xole bou tangu la andal li meitina thi xole lolou yeine gni niou deink souniou reiw wax li thi li dax li mo mat debat

  • @wakhtaneserignetouba7754
    @wakhtaneserignetouba7754 5 лет назад +2

    Franchement à l'écouter,on sent que la capacité intellectuelle de Ndoy bane ne dépasse pas celle d'un enfant de 11 ans .je me demande s'il est vraiment sorti de CESTI? mais il devrait mettre des harnais autour de sa grande gueule pour parfois l'obligé à se taire sur certains sujets.

  • @bulldozer3131
    @bulldozer3131 5 лет назад +3

    ils seront retrouvé facilement

  • @matymbayethiame5404
    @matymbayethiame5404 5 лет назад +2

    Bilakhi mére Adji dite maman Aicha linga wakh deguela

  • @oulimatambaye4809
    @oulimatambaye4809 5 лет назад

    Mouhamed ndiaye yaw dagua am personalite il faut faire comme comme boubacar diallo kitè khalass ndoye bane mokeu yakh ak abba dof bobou

  • @thieckasylla4578
    @thieckasylla4578 5 лет назад +3

    Ndiaye yalla nasa diamou yague

  • @conmbacamara213
    @conmbacamara213 5 лет назад +2

    merbi limou wakh amoul senegal yi ndanio son maroc

  • @papeallefall664
    @papeallefall664 5 лет назад

    tant qu'on applique ce que dieu à dit on aura toujours des problèmes plus sérieuse

  • @diaboulaniniange4968
    @diaboulaniniange4968 5 лет назад +6

    Wakhléne Foola Dou mo Gaune Nitt yii Dagnou lééndi déklou Bégué

  • @kandysarr7181
    @kandysarr7181 5 лет назад +1

    werou koor bi nitte yi di deff lou bakh profito si weerou promotion guene di raye rekk di tekk melni kou nekk film vampire ...... reposez en paix chers défunts thiote raffette na ak werr bou selle bi

  • @mamemodoudiop7867
    @mamemodoudiop7867 5 лет назад

    Okay Ndiaye

  • @fhachaobiang386
    @fhachaobiang386 5 лет назад +1

    Nanou yook Policéyi diokhlén ay voiture niouy weur gouddi ak beuthieuk lolou moy dini crimbi

  • @papeousmanesamb5345
    @papeousmanesamb5345 5 лет назад +1

    Mamadou Mouhamet Ndiaye yaw vrai hypocryte nga ya gueuneu khamnè pharmaciens yi nio nèk thi deug mais malheureusement comme ay pro Macky ngèn dolèn attaquer etat sènègalais mi gracier un trafiquant et assassin comme Woury diallo

  • @amathba6781
    @amathba6781 5 лет назад +1

    Adouna foumou djem lignawna lol kou Ray gnou Ray sou amone mou baxx ... Yalla nako yalla xaré aljana firdawsi li métina torop

  • @valimataaw5412
    @valimataaw5412 5 лет назад

    machallah sen ligeye rafet na. Yalla na len yalla deugeureul. Deukk bi boye na war.

  • @luezdrame7306
    @luezdrame7306 5 лет назад +1

    yalla nako yalla yeremm 😭😭 wakhall aminnn

  • @j0opbuur768
    @j0opbuur768 5 лет назад

    Bane serieuwul koi mais bane loy weuy ci lou ndiaye wakh

  • @mortalla28marone86
    @mortalla28marone86 5 лет назад

    Ils doivent aller en grève afin que la justice soit faite wouri moye kane

  • @kodendiaye4660
    @kodendiaye4660 5 лет назад +1

    dame migi danmarkiè

  • @tallmortalla1665
    @tallmortalla1665 5 лет назад +4

    Sénégal doul rek amoul justis

  • @kadiasambadia8493
    @kadiasambadia8493 5 лет назад +1

    Mais cette fille elle ressemble à la soeur de waly seck aïcha ballago

  • @diagneamina7023
    @diagneamina7023 5 лет назад +4

    Femme bi na wakh mome kène dorouko ms boumou gènèralisè

    • @galsenforever9657
      @galsenforever9657 5 лет назад +1

      gnidi wakh aussi marocain yi daniouy daur senegalais yi tamite bouniou generaliser,je vis la bas et machallah j ai pas de problèmes ni aucune autre connaissance , indiscipline senegal rek mokey tolerer, arretez kan meme

    • @chachagaye5777
      @chachagaye5777 5 лет назад +1

      Mo elle a raison j'ai fait 3ans au maroc massouma ame problème t'es marocain dafa beugue sénégalais tt le temps ils disent senegal maroc khal bi khal arrêté de dire du nimporte quoi

  • @souleymanegueye5049
    @souleymanegueye5049 5 лет назад

    C le maire qui passe tt son temps pour les fille et volé l'argent du village. Et pire rouler Av des voitures qui coûte des millions que son salaire ne peut pas acheter

  • @soknet2866
    @soknet2866 5 лет назад +1

    Ataya si bus Sénégal rek la am

  • @ansukoulibaly3076
    @ansukoulibaly3076 5 лет назад +2

    xalebi mérite woul li billahi wa tamba merena lenn trop

  • @bambakane2173
    @bambakane2173 5 лет назад +2

    Mére bi limiye waxe dara amou thi senegalaiyi sonou niou maroc lolou amoule

  • @linbic6720
    @linbic6720 5 лет назад +11

    Ndoye bane yawe duol rék moy sa dundu bayil duol waye ta yalla

  • @sayesakho2059
    @sayesakho2059 5 лет назад

    Païne de Mor mou diėkh

  • @andrenabigueye3201
    @andrenabigueye3201 5 лет назад

    No li gatiela si rewou Senegal domi Senegal di def mbirou goor jiguen ci pays Islam comme Maroc ç est de la honte total😬😡

  • @mohamedndiaye5280
    @mohamedndiaye5280 5 лет назад

    sénégal khana dah am armée gangster wala

  • @fagueye5469
    @fagueye5469 5 лет назад +4

    peine de mort au sénégal ,faut que tout le monde parle de ça

  • @serignesaliouniang4227
    @serignesaliouniang4227 5 лет назад +7

    Mère bouniou soneul vidéos yi gneup guiss nagneko marocain yeup ay domram lagne iow dangay protégé sa intérêt personnel

    • @dijasenba
      @dijasenba 5 лет назад

      Serigne Saliou Niang tu as raison. La dame wakhoul deugu les marocains n’ont jamais considéré les noirs

    • @serignesaliouniang4227
      @serignesaliouniang4227 5 лет назад +2

      @@dijasenba sénégalais si bopam mo égoïstes man niata sénégalais la xam youniou rey Maroc ak vidéos yi niou partager gneup guiss ko dame bi taxaw fi di wax li rien k pour son intérêt niak diom nite dangay beug sa pays beug sa domou pays fofou la adouna tollou

    • @dieyebbabacar981
      @dieyebbabacar981 5 лет назад +2

      Moi j'ai fait deux ans en Tunisie. J'ai tellement aimé ce pays.Ils respectent beacoup les senegalais.bayiléne di jugé.le senegalais est tespecté partout meme en France si tu dit que tu es senegalais tu es respecté.Con yiye touky rek gnoy def ay connerie gnou diépiléne gnouye jugé apres

    • @serignesaliouniang4227
      @serignesaliouniang4227 5 лет назад +2

      @@dieyebbabacar981 iow xamal Tunisie rekk bania xam yénén pays yi bayil gnémé yalla si ramadan laniou nekk j'ai fait plus de 15 ans en France del wax lo xam bayi fén da haram sourtou si ramadan

    • @dijasenba
      @dijasenba 5 лет назад

      Serigne Saliou Mane j ai vécu durant 4ans au Maroc. Ils ne nous aiment pas lolou moy deugu

  • @zerodechets2494
    @zerodechets2494 5 лет назад +1

    Au Sénégal trop de laisser faire. Voilà le résultat. Des jeunes innocents tués vraiment

  • @alioutoure2655
    @alioutoure2655 5 лет назад +2

    wayé lou takh niouy fowé bakan di raye noum léne nékhé te dou moudiou fénne

  • @beugfallou4928
    @beugfallou4928 5 лет назад +1

    Sonenefaa degue

  • @baobabsn3298
    @baobabsn3298 5 лет назад +4

    Kou rey dagn la wara rey moy yone !! Nakane dafa for

  • @user-hh8gz8bz6o
    @user-hh8gz8bz6o 5 лет назад

    Vous ne savais pas c est quoi la justice

  • @Americaine268
    @Americaine268 5 лет назад

    Metti na tropp adouna bi kenn khamatoul koy wollou

  • @papeousmanesamb5345
    @papeousmanesamb5345 5 лет назад

    vraiment yèn gni di dèg lou khalass ay vrai con ngèn kholèn ndoye bane ak mèrame bi doul rèk

  • @diarrambodji7669
    @diarrambodji7669 5 лет назад +2

    La dame bopam lay défendre m l'image est vrai

  • @beugfallou4928
    @beugfallou4928 5 лет назад +1

    Bane naafeexle

  • @mohamadsillah6795
    @mohamadsillah6795 5 лет назад

    😪😪😪😪😪

  • @kandysarr7181
    @kandysarr7181 5 лет назад

    kou raye dagne la warra raye mou diekh mane de legui pompe a gaz laye dokhone to balla guama raye ma raye la mou diekh li cst troppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppp

  • @sallpetit9144
    @sallpetit9144 5 лет назад

    Ay mére wakhal astakhfirou lahh

  • @anitabenejeloune8669
    @anitabenejeloune8669 5 лет назад

    Paix à son âme

  • @tenejolie2918
    @tenejolie2918 5 лет назад +1

    Femme bii meunneu fenn dh

    • @khoudiambengue69
      @khoudiambengue69 5 лет назад

      Yallana nako sougnou borom gnite si barké seydina mouhamed saw

  • @amethndiaye5154
    @amethndiaye5154 5 лет назад +6

    Mére bi nek Maroc day fonton nitt yi way narr mo geuneu bone bougoul nitt kou nioul

    • @galsenforever9657
      @galsenforever9657 5 лет назад +2

      ellle a raison je vis laba c juste les vendeurs ki veulent s installer partout et c interdit

  • @mimidewa5102
    @mimidewa5102 5 лет назад

    Mohamed Ndiaye tu as bien dit ndoye Bane doulkatela.
    Un arabe n'a jamais considéré un noir.

    • @dieyebbabacar981
      @dieyebbabacar981 5 лет назад

      C'est pas vrai moi j'ai fait deux ans en Tunisie.j'ai tellement aimé ce pays ils respectent tellement les senegalais

    • @dieyebbabacar981
      @dieyebbabacar981 5 лет назад

      C'est pas vrai moi j'ai fait deux ans en Tunisie,ils respectent tellement les senegalais.

  • @idrissatoure4709
    @idrissatoure4709 5 лет назад

    Peine de mort rék moy solution bii

  • @salamsalam-xj5rh
    @salamsalam-xj5rh 5 лет назад

    Mais merbi khana da am farou marocain ndiabotte nga wakh wayé wakho dieukerr dè