Wallahi kéep kou beugue deuk xam ngui serigne amsatou limou wax dara nékou si ndax serigne touba ci boopam yonénte bi mooy serigne ñieum té moom la don liguéyeul , Kon serigne mame mor diara bou liguéyeulé serigne touba lou ci nék
Da ngay doul dafa togne mame mor diarra rek nekoufi thi koum mana diokhe exemple yabate ak rew mo tax niou kay fonto kouko yek ak kouko yegoul souy souffle borom sham yagui souffle serigne bi
ماشاء الله تبارك الله جاء ذلك الله خيرا
نعيب زمازننا والعيب فينا
وما لزماننا عيب سوانا😮
Ndeye Sanne Dieureudieuf
Ya bakh way diadieuf amna solo
Amatina solo lool Gëy ❤❤❤❤❤❤❤
Man deh serigne Mouspha naw nala
Nanou rous mame mor ndakh s touba
Dieredieuf sa kàddu yi rafétna yalna yalla def diamou
Rafétna loooool❤
Dieurdieuf❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Serigne touba kenela ko bagne ak ko nagou mou ame dieureudief serigne moustapha gueye
Borom touba ak borom touba nio bokou niari waydiou koudoul mom molako guena diegue koum nekh ak koum nakhari
Nanou rous serigne touba guir yalla
S Moustapha Gueye lou werr nga wax
Amine❤❤❤❤❤❤❤dieureudieuf Serigne Touba☝
الجزاء من جنس العمل
وقال الله
وإن عاقبتم فاعقبوا بمثل ما عوقبتم به
ولئن صبرتم لهو خير للصابرين
Dieurdeuf dieurdeuf dieurdeuf ya bakh
Serigne Amsatou nitt kou bakh la seulement on a mal interprété ses propos
Amna solo
Wallahi kéep kou beugue deuk xam ngui serigne amsatou limou wax dara nékou si ndax serigne touba ci boopam yonénte bi mooy serigne ñieum té moom la don liguéyeul ,
Kon serigne mame mor diara bou liguéyeulé serigne touba lou ci nék
Kounane Limou wax dara nekousi xamo stoir wala ak parpar ló mola taxa diouk
Borom sam kouka guene xame serigne touba amoul kouka guene gueme serigne touba amoul wayé kouka téla li gueyall laa wakh dafa warra ame solo ame ndiarigne serigne bi mo toudé mame MOR diarra magui mak fonkou ko lol nio bokou ndeye bokou baye te stouwar xame nagne ko xame xame mongui kuer borom same
Kan mola wakhni lol la nit gniy bagne soungue ni analyse dou nguen ko tek thie degue waye di par par lo
Gayi tontou s hamza rewandé reka la kouné sa mame limou ame diayanté Koko maye Bo nango ni diebalou na wara nangou foutikou ligueyal
Yaw yangeuna reew niepou
Da ngay doul dafa togne mame mor diarra rek nekoufi thi koum mana diokhe exemple yabate ak rew mo tax niou kay fonto kouko yek ak kouko yegoul souy souffle borom sham yagui souffle serigne bi