Urgent! Déclaration Magal 2018 du Khalif Général des Mourides Serigne Mountakha MBACKE

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 дек 2024
  • Déclaration du Khalif Général des Mourides sur le Grand Magal de Touba 2018 et le projet de construction de l'université Cheikh Ahmadou Bamba à Touba

Комментарии • 182

  • @MorNdiaye-r7f
    @MorNdiaye-r7f Год назад +1

    Dieureudieufé Mbacké balla Yalna yalla godal fanwi yokou weurgi mbanga matalé❤

  • @salioulo3882
    @salioulo3882 6 лет назад +13

    Yalla nala yalla faye
    Yalla nala yalla Sam
    Yalla nala yalla haarr
    Yalla nala yalla dembali
    Yalla naga fi yague ji barkeb
    Cheikhoul khadiim Amiinnnnn

  • @cheikhndoye2757
    @cheikhndoye2757 6 лет назад +1

    Dieuredieuf Mbacké Holl yi sed na Hel yi dal na
    Yalla nala Serigne Touba dolél baga yégali liguèy bi té dorat yénén
    Dieureudieufé Serigne Touba
    Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall

  • @cheik-pointsg1238
    @cheik-pointsg1238 6 лет назад +2

    Yallna fii yague tee weur mbacke balla ayssa diaradieuff serigne touba

  • @serigneguisse8416
    @serigneguisse8416 6 лет назад +7

    Machalla santé yalla Rek yalla nagua fi yague Mbacke si barkeb Serigne touba Mbacke

  • @smarattuubii8512
    @smarattuubii8512 6 лет назад +8

    كلمة حق من رجل صدق حياكم الله وبياكم أيها الشيخ المنتقى وحفظ بكم الإيمان والإسلام والإحسان

    • @cheik-pointsg1238
      @cheik-pointsg1238 6 лет назад

      ماشاء لله فحفظ الله وبركاته

  • @abdoulahatbousso3770
    @abdoulahatbousso3770 6 лет назад +5

    Mb balla amatina solo machalla yalnala yalla katata nal thi barkeb serigne bi

  • @alladionefall4490
    @alladionefall4490 6 лет назад +22

    Yalla nagua fi yague mbacké si barkeb serigne saliou mbacké

  • @Benoumar10
    @Benoumar10 6 лет назад +5

    Machala Mbackè di doli sante rek di niane si barkei Cheikhoul Khadim nga gueun fi yague rek gueuneu werr ba motali yeneu yep ak nall yep.

  • @ndeyefatousamb245
    @ndeyefatousamb245 6 лет назад +1

    Ma cha ALLAH, alkhamdoulillah Mbacke Balla Aissa. Nek rek thi sa guinaw Mbacke, Di diokou thi Cheikhoul Khadim. Dieuredieuf S Touba diarawlak Mame Cheikh Ibrahima Fall. Ziar gneup

  • @boubacardiouf8454
    @boubacardiouf8454 6 лет назад +2

    Jerejef Mbacké, yalna ngafi yag té wer
    Té BOROM BI maya nga agalé sa yèné barké BOROM TOUBA

  • @xale-yar-ak-teggin.7152
    @xale-yar-ak-teggin.7152 6 лет назад +1

    Maa sahala *serigne mountakha all bachir yallngafi guena yagg guena wér muy gundi baxx di guena guenn! Di guena Néxx* çi bar képp Qassidayi jërë jëffati Yallnañou yalla défall dégg ak topp ak diariñou

  • @serignefallou2992
    @serignefallou2992 6 лет назад +3

    DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA

  • @khadidiatoudia759
    @khadidiatoudia759 6 лет назад +5

    Macha'allah Allahou Akbar hamdoullillah Vive la verite rien que la verite macha'allah Allahou Akbar vive l'Islam, vive Serigne Touba

    • @cheik-pointsg1238
      @cheik-pointsg1238 6 лет назад

      ماشاء لله اللهم صلي على سيدنا ونبينا محمد وعلى اله وصحبه وسلم تسليما كثيرا

    • @cheik-pointsg1238
      @cheik-pointsg1238 6 лет назад

      Il a touba inchalah vive l'islam c'est sa le mouridisme le coran le sunna travail et le respect des tes parents adore all'ah et suivre le sunna de mouhamed psl en suivre le ndingal de serigne touba rek machalah

  • @biranethiaw4055
    @biranethiaw4055 6 лет назад +2

    Alhamdoulillah diereudieuf Mbacke balla yallah nanga fi yague te weer ci barke kou Teed ki

  • @B-221
    @B-221 6 лет назад +2

    DIEURADiEUF Mbacke YAKK Fi Loll Barkep Serigne TOUBA

  • @boromdaroubakhiimbacke5905
    @boromdaroubakhiimbacke5905 6 лет назад +3

    Machalla Mbacke Balla yague fi looool Tewer amiiiiine

  • @sidindiaye9356
    @sidindiaye9356 3 года назад

    Macha allah belle discours mbacké yague fi lool té wér amine

  • @mouhamedbousso3973
    @mouhamedbousso3973 6 лет назад +9

    حفظ الله مولانا المنتقى وأيده ونصره بجاه جده العبد الخديم عليه رضوان الله الباقي القديم!!

    • @cheik-pointsg1238
      @cheik-pointsg1238 6 лет назад

      آمين يارب العالمين اللهم صلي على سيدنا ونبينا محمد وعلى اله وصحبه وسلم تسليما

    • @cheikhounambzye1815
      @cheikhounambzye1815 6 лет назад

      Amiine

  • @mbakkeballa8614
    @mbakkeballa8614 6 лет назад +6

    أطال الله عمره وأيده ورعاه ءامين

  • @madamegueye8781
    @madamegueye8781 6 лет назад +2

    machalla amna solo trop yalla na yalla goudeul sa fane

  • @aissatawade3291
    @aissatawade3291 6 лет назад +4

    Masha'Allah qu'Allah vous préserve et vous facilite ya Rabbi

  • @sarrndeye1146
    @sarrndeye1146 6 лет назад +9

    Mbacke balla amatina solo yagu fi rek ta werr si barke cheikhouna cheikh ahmadou bamba

  • @senegaltouba1076
    @senegaltouba1076 6 лет назад +1

    Machallah yalla na nga fi yag te wer am taw fekh ba fawou

  • @ibrahimadiop604
    @ibrahimadiop604 6 лет назад +1

    Machallah amatina solo hana nga yagfi ta wér rékk si barkép borom magalgui

  • @cheik-pointsg1238
    @cheik-pointsg1238 6 лет назад

    Billahi sama khol seddna lol machalah amna solo lol way machalah yallnak fii yag lol tee weur 🙏🙏🌴🍀🌴💖💜💚💚💜💖💖ila touba rek partout dans le monde

  • @pathesourang8565
    @pathesourang8565 6 лет назад +1

    Mbacke yalla na gué fi ya gue thi wurr lolll amiinnee serigne mountakha bassirou yalla na fi ya gue thi wurr lolll amiinnee ci barkip khadimoul moustapha

  • @abdoubakhendiaye4890
    @abdoubakhendiaye4890 6 лет назад +3

    Yalla nala fi Yalla bayyi lou yag banga motali sa yèné thi yonou Cheikhoul Khadim,BILLAHI MBACKÉ YA BAX

  • @diagnenarre7448
    @diagnenarre7448 6 лет назад +1

    Machallah yalla na yalla fay len machallah

  • @khadidiatoudia759
    @khadidiatoudia759 6 лет назад +2

    Que Le bon Dieu te protége incha'allah et te donne longue vie dans le bonheur, la paix et plein de sante avec toute la houma incha'allah misericordieux et benediction incha'allah

  • @fadiloudieyetdieyr4141
    @fadiloudieyetdieyr4141 6 лет назад +2

    yallana yalla gudal fanwi
    yagifiloul ta wer aamin aamiun

  • @salioudiop5835
    @salioudiop5835 6 лет назад +1

    حفظكم الله وأمدكم عمرا مديدا وصحة وعافية

  • @falloumbaye5407
    @falloumbaye5407 6 лет назад +4

    Dieu dieuf mbacké yalla na nga fi yagg té wére hackazaa

  • @mayseye7357
    @mayseye7357 6 лет назад +2

    Machallah
    Yalla nalafi yalla yagal ta and ak werr

  • @morbichrisamb9975
    @morbichrisamb9975 6 лет назад

    Ndaysane sounou mbécté mi Cheikh mountakha yalnakofi sunou Borom geuna bayyi barkéb alkhour àne

  • @serignemodoudiop760
    @serignemodoudiop760 6 лет назад +1

    Mbacké balla yague fii loooool té wére🙏🏽❤️

  • @CheikhGayeLo
    @CheikhGayeLo 6 лет назад +4

    Ndaye sann Xol yépp toyna Machala Mbacke

  • @B-221
    @B-221 6 лет назад +1

    INCHALLAH ANNEUKAK YOW MAGAL MAGAL GUI SANTATI YALLA Ci BUSBI ! Dieuradieuf Serigne TOUBA

  • @leralbamouleer9260
    @leralbamouleer9260 4 года назад

    😭Allhamdou lillah mbacke yagui fi looooool te werr🤲

  • @serignebabounaroumamesalio9291
    @serignebabounaroumamesalio9291 6 лет назад

    Machallah Fier dêtre Un Talibé Cheikh Ahmadou Bamba Babou Narou Mame Saliou

  • @susobass7685
    @susobass7685 6 лет назад +2

    yalla nafi yeuge lol tewer amine

  • @mbowmodou6113
    @mbowmodou6113 6 лет назад +2

    Yalla nga fi yangue lool ter were mbarckep khassida yi aminnnn

  • @cissedame3803
    @cissedame3803 6 лет назад +2

    Yalla nalafi yalla yagal té mayla wer

  • @cheikhemess
    @cheikhemess 6 лет назад +6

    الخليفة العام لطريقة المريدية أيده الله ونصره في خدمة خادم الرسول ببركة سيدنا محمد صلى الله عليه وسلم

    • @cheik-pointsg1238
      @cheik-pointsg1238 6 лет назад

      آمين يارب العالمين اللهم صلي على سيدنا ونبينا محمد وعلى اله وصحبه وسلم تسليما

  • @segandiaye9748
    @segandiaye9748 6 лет назад

    THIEEY MBACKÉ BALLA AMNA solo loolou yaag leen fii loolou té weer souñou nieuriñ la deii té fass yénné wéeyè seeni ndigueul dieuredieuf MBACKÉ beeg nañou loolou

  • @mouhamedndiaye8820
    @mouhamedndiaye8820 6 лет назад +3

    Tabârkalla macha allah mouriténa loll yallana sa fane gouddou loll andack wérr

  • @bayeassanesylla2913
    @bayeassanesylla2913 6 лет назад +2

    Dieredieuf Mbackè ya bakh yallna ngafi yague tè wër barquè brom touba

  • @niomrelo1959
    @niomrelo1959 6 лет назад

    MACHALLAH MBACKE DEGUE NA WAKHDJI BOUBAKH TADINANKO DIEFFE

  • @jaysuncom7895
    @jaysuncom7895 6 лет назад

    Yalna Ku Tedd ki doli katane Gui DILA nianal Lou Serigne SALIOU Mbacke nianalone Cheikh Ahmadou Kara Fou yéné bi TOLu Yalnako Katane Gui eup am Ay Ndam

  • @cheikhounambzye1815
    @cheikhounambzye1815 6 лет назад

    أطال الله عمرك بتمام الصحة والعافية amna solo lool

  • @papendiayediop8534
    @papendiayediop8534 6 лет назад +2

    Yalla nagfi yage loooooooooooooo tewer amin amin amin

  • @khadimsamb5708
    @khadimsamb5708 6 лет назад

    yalla nga fi yagg te weer mbacke balla ci barkeb s touba

  • @saliscosall9197
    @saliscosall9197 6 лет назад

    Yalla nagafi yague lolou mbacke balla té werr si barkép serigne bi

  • @toubambacke6438
    @toubambacke6438 6 лет назад +2

    Yalla na yalla fayla sa yeene

  • @sangareousseynououmy9869
    @sangareousseynououmy9869 6 лет назад +1

    Dieuredieuf Sangue bi, Yalla nanga fi Yague lool té weer. Sou Sobé sounou Borome bi, dinaniou la dégueul

  • @walosaliou6404
    @walosaliou6404 6 лет назад

    Machalla mbacké balla yag fi loooool te wér ak werle si barkep khasside yi

  • @user-wo6hl4wf6p
    @user-wo6hl4wf6p 6 лет назад

    Mbéck mi mbacké Balla yalla nafi yagg té were

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Ziar serigne bi lep LO wzkhnonoula

  • @bayeseyni4942
    @bayeseyni4942 6 лет назад

    Machaalla mbacké yagui fi té wéér

  • @bassngom2023
    @bassngom2023 6 лет назад

    Mbacke yalla nagafi yag te wer amin

  • @serignediop5345
    @serignediop5345 6 лет назад

    Yalla Gafi Yagg Lol té Weer Mbacké Mala Beugue Dieureudieuf lo déf l'Islam

  • @mouhameddiouf5020
    @mouhameddiouf5020 6 лет назад

    Dieureudieufé Borom Touba

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Diereudief serigne touba Khadime rassoul diarama mame Cheikh ibrahima fall

  • @sunurew3922
    @sunurew3922 6 лет назад +4

    thieuy mbacke dagua bakh reck waaye nioune douniousi dara léppou yaw laaaa

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Yalla na yalla yook lairam serigne sidy moukhtar mbacke dîne nimou ko beuguen won lep ben

  • @khadyfaye661
    @khadyfaye661 6 лет назад +2

    MBACKÉ yokal yagual doundeul sax day gueune nééx gueune yague gueune sax

  • @magattebakhoum704
    @magattebakhoum704 6 лет назад +1

    yalla n'a gafi yague te werr lool mbacke Balla dieradiefati

  • @wakarsmodoufaliloufall8363
    @wakarsmodoufaliloufall8363 6 лет назад

    yalla gasi am ndam mbacke si barkeb s touba

  • @moustaphadieye1325
    @moustaphadieye1325 6 лет назад

    L'hoctoguone AL MOUNTAKHA,dineu yagg dineu neikh,barki cheikh hamadou kara

  • @fallougallas5830
    @fallougallas5830 6 лет назад

    Yalla nane ndiéckou magal gui
    8 khalifa s.touba
    Magal touba 18 safar
    Le 28 october 2018
    S.mountakha mbacke y'alla nafi yack

  • @bane257
    @bane257 6 лет назад +4

    #YagfiTewerMbacke #Ilatouba #18safarDestination #Bamba_Only

  • @kandjindiaye8464
    @kandjindiaye8464 6 лет назад +1

    باك. الله. حفظه. وايدك. برك. بروم. طوبي

  • @cheikhbadar2255
    @cheikhbadar2255 6 лет назад +5

    الحمدلله الحمدلله الحمد لله رب العالمين بك جرجفت يله نكفيك لول تور لول ما شاءالله

  • @moustahinesarrmouritanesen465
    @moustahinesarrmouritanesen465 6 лет назад +1

    Walahi Li ndam la si yonebi yageu fi mbacke

  • @fallousylla5100
    @fallousylla5100 6 лет назад +1

    فخر الامة عفظك الله ورعاك وايدك

  • @asnaakhadiimgueye8309
    @asnaakhadiimgueye8309 6 лет назад +1

    Yagall te werr mbacke waaye mbectem dioulitt yeppou nga

  • @falloutall6772
    @falloutall6772 6 лет назад +2

    mbacke yagafi tewer loooollll waye

  • @amarmaneamar598
    @amarmaneamar598 6 лет назад +2

    Yalla na nga fi yague te wer mbacke

  • @cheikhahmadoubamba1690
    @cheikhahmadoubamba1690 6 лет назад

    Allahou Akbar S mountaqa Bachir

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Wave Wave mbacke inchalla

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Daga bakh mbacke

  • @mamethiernodiop6346
    @mamethiernodiop6346 6 лет назад

    Mbackè yalla ga fi yageu tè lool tè wèrr

  • @cheikhbadar2255
    @cheikhbadar2255 6 лет назад +2

    Yaa baax te wayaf wallahi

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Wawaw serigne bas abdoul hadr

  • @mbayeseye2640
    @mbayeseye2640 6 лет назад +2

    Yalla ngafi yak tawėr rėk

  • @wadendiaga2123
    @wadendiaga2123 6 лет назад

    Dia dieuf mbacke yague fi looooooool ta wér

  • @abdoudiop9702
    @abdoudiop9702 6 лет назад

    machalla sama sopeby wag fi looool ter wer

  • @mamemorsylla186
    @mamemorsylla186 6 лет назад

    Mbackè balla yalna fi yagu lool ta andak wer si barkep xassidah yi

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Mouhamed yarasoulyla [psl]

  • @mouhamedbousso3973
    @mouhamedbousso3973 6 лет назад +1

    الله أكبر!! Lii seedna xoll

  • @khadimrassouldiaw2007
    @khadimrassouldiaw2007 6 лет назад

    Heskey li dhei matna tewlou guinaw biñou meuyto euphorie bi, yalnafa Yagg

  • @alassanendiaye5685
    @alassanendiaye5685 6 лет назад

    Macha allah

  • @mamediarra6121
    @mamediarra6121 6 лет назад

    Yallana ngua fi yague Mbacke balla

  • @SeexBamba
    @SeexBamba 6 лет назад +2

    Touwarkalla

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Amine

  • @modouboussoba4670
    @modouboussoba4670 6 лет назад +3

    Ay mbacke ñune ñii ñosi dess kay wara andak yaw cik ndiiub rek dila ñaanal nga yague fi lol té wër

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Serigne mountakha bassirou mbacke lep lo beugue borom defko

  • @AlhassaneSeck-tq9pg
    @AlhassaneSeck-tq9pg 7 месяцев назад

    Yagui fi loy mbacke

  • @cheikhcheikh3924
    @cheikhcheikh3924 6 лет назад

    Yalla nako serigne mountakha djite ay at youbary tanou fekke lepp te and ak diamme

  • @ndelldiouf197
    @ndelldiouf197 6 лет назад +1

    Yag fi lole Mbacké té and ak wer thi barké khassida yi