Urgent: Serigne Mountakha très en colère contre Sokhna Aïda Diallo « Liima Ko Wax Défouko »

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 224

  • @atoumanendiaye9160
    @atoumanendiaye9160 5 лет назад +74

    Dieuredieuf Serigne Touba Dieuredieuf Serigne mountakha Mbacké yallah nalah Yallah maye wer....amine Mbacké balah...cliqué j'aime.....

  • @ibrahimaba109
    @ibrahimaba109 5 лет назад +6

    Je suis Tidiane mais déma beug Serigne MOUNTAKHA yalla nafi yag té weurr

  • @teningdiouf5112
    @teningdiouf5112 5 лет назад +50

    Je suis tidiane mais je suis parfaitement d'accord avec le khalif je le souhaite longue vie vraiment amnasolo

  • @mayrasamb1240
    @mayrasamb1240 5 лет назад +11

    Bilahi mane dama beugue serigne mountakha mbacké yalla nako fi yalla yagual

  • @adraneba2310
    @adraneba2310 3 года назад +2

    Machallah Serigne mountakha billahi je suis khadre mais ki démako beug billahi anzim khawma nane lay déf ba guisko yalna yalla goudal sa fan mbacké ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @khadydiallo7233
    @khadydiallo7233 4 года назад +7

    Mbackè Yag fiii loll andeuh ak werr si barkep serigne touba❤️

  • @saerndiaye4427
    @saerndiaye4427 5 лет назад +54

    Sokhna aida Diallo na moytou bopam wayé yonou mouride kouko beugue saltel serigne bi fayy sayy lamp dieuredieuf serigne mountakha bachir yagg fi lol ❤️

  • @ndeyekebe6612
    @ndeyekebe6612 5 лет назад +13

    Alhamdulilah rabil alamine Dieureudieuf serigne touba serigne mountakha yalla nafi yague te werr👏❤

  • @amdygueye1206
    @amdygueye1206 4 года назад +5

    serigne mountakh yalla nala serigne touba fayall boupam ❤❤

  • @aminasarr9681
    @aminasarr9681 5 лет назад +32

    Mame abdou aziz sy dabakh rekkk lay guisss si yaw

  • @adamandiaye9452
    @adamandiaye9452 4 года назад +9

    je suis tidaine mais dama beugeu Kalifa bi té yalla rek takh té mousoma dem Touba bilahi beugue na dem Touba 😭🤲♥️♥️

  • @mlamine
    @mlamine 5 лет назад +1

    Waraaté bi diott na, macha Allah. Kaddou yi sou wesso soxna ci niou ko dieumeulé, mbind leu ci kepp kouy wotewoo joulitt wala di askanoo ci yonou mourid. Yalla na yolli dolli wer té goudeul fani Serigne bi ak kepp kou taxaw ci diglé lou baakh ak teré lou bonn

  • @14binette
    @14binette 5 лет назад +10

    Nagnou gorgorlou si Ndioup. Ndioup moy boutou lep lou bakh..Machallah

  • @mariediop8985
    @mariediop8985 5 лет назад +1

    Je suis khadre wayè mbackè sou serigne touba dèlici wone do dèfarate sa togay dieureudieuf

  • @assanesylla4136
    @assanesylla4136 4 года назад +1

    Euskay ndeyssane machalla machalla machalla. Kene Dou Serigne Mountakha .

  • @ibrahimadia5008
    @ibrahimadia5008 5 лет назад +4

    Dieureudieuf serigne mountakha yagg fi loll tè wèrr, bègg na si yow

  • @aminatathiaw7891
    @aminatathiaw7891 3 года назад +1

    Serigne Mounetakha Mbacké yalla nanga fi yague ak ñun té wër kilifa dëguë ku la xamul rék moy fowé say kadu fowo folu wo 😢😢😢

  • @astouniang3278
    @astouniang3278 5 лет назад +4

    Yalla na fii yagui lool te wer machalla mbacke bala

  • @dhhtutertyy7294
    @dhhtutertyy7294 5 лет назад +8

    Ay way aïda diallo roussal yalla mane serigne bi dioy lonama sakhe

  • @ramarawa7917
    @ramarawa7917 5 лет назад +4

    Dieureufdieufaty mbacke balla yague fi lol te wéer barke serigne touba

  • @baxbaxatv4255
    @baxbaxatv4255 5 лет назад +11

    Dieuredieuf S Touba S Mountakha

  • @bouchradiagne9787
    @bouchradiagne9787 5 лет назад +6

    Lou bone kagne si poubèl ba rèk
    Mbakè yageu fi lollllllllllllllll
    Machalla machalla

  • @arounaba8343
    @arounaba8343 4 года назад

    Barkhé cheikhal Hadji Malick Sy man Serigne mountakha bachirou Dema kha beugou rk t yalla takhe yalla na yalla goudal ay faname thi barkhé mamame

  • @nanyfall1846
    @nanyfall1846 5 лет назад +21

    Alhamdoulilah...dieireudieuf serigne touba,sama mbokk dioulite yi nianallen ma ya Allah mayma ndiabot,sey Sénégal té amo dome metty na psychologiquement wayee sant sounou borom bou bakh,🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾...

    • @mamembathioundiaye4812
      @mamembathioundiaye4812 5 лет назад +1

      Yalla nala yalla méyy djaboot sii barké serigne touba

    • @mamediarraboussogaye2963
      @mamediarraboussogaye2963 5 лет назад +2

      Nany Fall yalnala yalla defal li gueune nite dinay gnaane dara fék guenul ci moom

    • @nanyfall1846
      @nanyfall1846 5 лет назад +1

      Mame Diarra Bouso Gaye amiiiine

    • @moussabodian6809
      @moussabodian6809 5 лет назад +2

      Yalla nala yalla sunu borom may ndjabot gou barkel ci bidjahi Seydina Mouhamad🙏

    • @nanyfall1846
      @nanyfall1846 5 лет назад

      Neto Bodian Amiiiine way 😭😭😭🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @vivianesylva8727
    @vivianesylva8727 5 лет назад +1

    Je suis vraiment contente cette femme il faut la remettre a sa place dieuredieuf serigne mountakha

  • @Fatoundongndeye
    @Fatoundongndeye 10 месяцев назад

    Serigne Mountakha Mbackè Yalla na fi yague tè weerrr

  • @cheikhba9984
    @cheikhba9984 5 лет назад +6

    Direuredieuf mbacke, yagfi lol téwérr🙏🙏

  • @sokhnasoukeyna9823
    @sokhnasoukeyna9823 5 лет назад +1

    Serigne mountakha yalgafi yageu tè weurr loll walahi nako nieup nianall mou yageu yagamfi sounou ndiarigne rek la mbacke 🤲🤲🤲🤲

  • @yaamindiaye3602
    @yaamindiaye3602 5 лет назад +6

    Amna solo machallah yague fi lol Mbacké te am werle

  • @khadyfall3907
    @khadyfall3907 5 лет назад +2

    Machallah Mbacke sant naniou bou bakh

  • @queensarr4009
    @queensarr4009 5 лет назад +1

    Dieureudieufati Mbacké Balla souniou xole yi séédna machallah

  • @serigneabdou51
    @serigneabdou51 5 лет назад +10

    Ma ko beugue serigne mountakh mbakhe

  • @bintousall1679
    @bintousall1679 5 лет назад +22

    Douma mouride deh waye mala beug sama khol mbacje yague fi lol de weer.

    • @aliounendoye46
      @aliounendoye46 5 лет назад

      Eupouna déf mouridoulah moy kounama ageu thai yalla

    • @aliounendoye46
      @aliounendoye46 5 лет назад

      Eupouna déf mouridoulah moy kou nama ague thia yalla

    • @amdygueye1206
      @amdygueye1206 4 года назад

      yalla nala serigne touba faye

  • @ngonembaye5640
    @ngonembaye5640 5 лет назад +11

    Dieuredieuf yague tamou ande ack wer

  • @ouliseye5525
    @ouliseye5525 4 года назад

    Dama beugueuu serigne moutakha dakh yaraw am dinee nem fokeuu domou adama borom mbecmi beugueuu naleu🥰

  • @mamandiaye6480
    @mamandiaye6480 5 лет назад

    Dieureudieuf s mountakha mbacké yag fi

  • @niangabdoulaziz2534
    @niangabdoulaziz2534 5 лет назад +25

    🤭Aïda Diallo yonou seuyetané gua diarre ,
    Té gua deupe ta diarre si yonou serigne touba bi Moy lislame🙏🏽

  • @boubacarrdiallo8244
    @boubacarrdiallo8244 4 года назад +1

    Dieurdieuf serigne mountakha

  • @ndiayemouhamed1780
    @ndiayemouhamed1780 5 лет назад +18

    Mbacké yague fi lol and ak weer thie barké seydina mohamed psl

  • @filydiallo3771
    @filydiallo3771 5 лет назад +5

    Tiéy Mbacké yague fi lol té wéer. MashaAlla

  • @maremasoda7242
    @maremasoda7242 5 лет назад +5

    Mbacké Balla yalna yala gou dal fan wi te yokou wer gui

  • @sadiosabaly8834
    @sadiosabaly8834 4 года назад

    Dieureudieuf Serigne Mountakha Yalla nalla Yalla may Goudou fan ak wër gou yaram mais oú sont les Parents de Aida Diallo sa famille

  • @fantadiarra9273
    @fantadiarra9273 5 лет назад +4

    Barki Cheikhna Hamawla Aïdara Serigne bi mérna😟
    Ay way yalla bou akk Serigne bi dall Sohna Aïda 😔
    Sopékou DEUG warna sohna aida ak gnimou djité

  • @Fatoundongndeye
    @Fatoundongndeye 10 месяцев назад

    Sante Serigne Touba amoul morome kène la

  • @iboudiallo9652
    @iboudiallo9652 4 года назад +4

    Machallah 😍😍😍❤❤❤🙏🙏🙏❤❤😍😍😍❤❤❤

  • @idrissasow7848
    @idrissasow7848 3 года назад

    Ma ashalah un homme sage et très pieu

  • @syadjagamougueye1790
    @syadjagamougueye1790 5 лет назад +34

    Aida Diallo tu fais honte à la gente féminine.ngay dérangé kilifeu gou tolou ni.bilahi souleu batine bi dallé dou bakh si yaw

    • @astousylla5410
      @astousylla5410 5 лет назад +2

      Barkei cheikhoul khadim Dou bakh si môme vraie satan leuh

    • @fatoumbaye2390
      @fatoumbaye2390 5 лет назад +1

      Wax gua deugue dh bilay

    • @mariediop8985
      @mariediop8985 5 лет назад +1

      Lima mèti rek moy guissouniou sa rètane gou nekhgui

  • @Oumousyll
    @Oumousyll 5 лет назад

    Allahou akbar segne mountakha mér ayy li yalna diour diam di

  • @iboudarou930
    @iboudarou930 5 лет назад +3

    Machallha Serigne Touba Serigne Mountakha Bachirou Khalifa general des Mourides kadou yi Rafetna lole Aida diallo saytanè leuh beug yakh yonne wi wayye serigne bi Mokay Arale bopam

  • @mamefatydiop8073
    @mamefatydiop8073 5 лет назад +31

    Ndaysann yague fi loll ta wérr mbacké balla

  • @diatouamar9813
    @diatouamar9813 5 лет назад +1

    Dieureudieuf mbacke Balla yague fi loll tè wer

  • @ibrahimasall6565
    @ibrahimasall6565 3 года назад

    Yalla n'a yalla goudall sa fanne

  • @abdolabduldiop4671
    @abdolabduldiop4671 5 лет назад +7

    Aksasa 🙏🙏❤️

  • @diopfatima8033
    @diopfatima8033 5 лет назад

    Machalakh mbacké yagu fi lol té weur amena solo machalakh ame nagnou mbekté akka contanté bou magu machalakh

  • @abdouba6202
    @abdouba6202 4 года назад

    Ndeysane mbacké balla machalla

  • @allediallo2610
    @allediallo2610 3 года назад +2

    Long vie à toi machalla ♥️♥️♥️♥️

  • @sallmaman5994
    @sallmaman5994 4 года назад +2

    Amine 🤲 🤲 🙏 ☝️👌

  • @evaba4231
    @evaba4231 5 лет назад +2

    Djieureudieuf serigne touba serigne mountakha yak fi lol dé wére

    • @miriamesow6909
      @miriamesow6909 5 лет назад +1

      serigne mountakha yalla nafi yague te weer .damako beugue lol waye.serigne touba amoul morom

  • @miachougoudiaby991
    @miachougoudiaby991 5 лет назад

    Dieureudieuf mbacké balla aîcha

  • @seydinaniang233
    @seydinaniang233 5 лет назад +2

    machalla mbacke

  • @fatoukinesagarniang2931
    @fatoukinesagarniang2931 5 лет назад +15

    Dieuredief mbacke yague lole tes were thi barker kou tede ki

  • @falldior9914
    @falldior9914 5 лет назад

    Dieureudieuffattii sounou Kilifa bou Magg bii té tédeu , Ngatché Ngalama . SOKHNA AÏDA DIALLO , khamoul bopam , Téré Téré mou teu, bayiil mou giiss .

  • @talibecheikh7367
    @talibecheikh7367 5 лет назад

    Dieureudieuf Mbacké yague fi lool té wéer ndawsi di aïda diallo nak khamone nani fi laye moudié ndakh togne bakhoul na délossi khélam té khamni djigène boudone seuy ba dieukeureum fatou dagua wara défarate sa toguay bamou diék té bayi khèl ni mome santoul Mbacké touba doufa dome té doufa seute nite kou bakh daguay yaar sa bop bala nioulay yaar yalla na diamm yague

  • @ndackkairediagne3641
    @ndackkairediagne3641 5 лет назад +1

    Manchalla

  • @diarasawane3369
    @diarasawane3369 5 лет назад +1

    Thieye yalla deugue nekhoul doyna war

  • @diopdinne1428
    @diopdinne1428 5 лет назад +5

    Mhasala amna Solo de Mbake balla

  • @hawakante8752
    @hawakante8752 5 лет назад

    Li d'où mouride rek mokowara khekh gnoune dioulite yeup nosi wara diouk aida degua delou guinaw nite DINA balei wayer martaba doubalei yalnala yalla wagni

  • @idafaye7351
    @idafaye7351 3 года назад

    MaschaAllah Mbacke

  • @fatoumbaye2390
    @fatoumbaye2390 5 лет назад

    Yalla nafi yague tee werr mbacké balla aïcha

  • @bayedjibydiop3899
    @bayedjibydiop3899 2 года назад

    Machalla

  • @awandiaye3312
    @awandiaye3312 5 лет назад

    J SW parfaitement d'accord sa fait honte bilaye long vie a khalif général

  • @coeur2lion913
    @coeur2lion913 5 лет назад +4

    Bobou ba légi magi wah dah loudoul deg gnépa si wara wah mé nak sénégal dafa bari ay nafék dougnou wah kéne deg mane talibé tidiane bi li ladone har si yaw le khalif général des mouride contane nagne trop si yaw machala yalna yalla goudal faneyi aida diallo nak dou nit cou bah mé inecha ala day méti rék mé l'islam day am ndam coucoy héhe nak digaco gis légi

  • @taphadiallo2819
    @taphadiallo2819 5 лет назад

    Thieuy serigne mountakha bassirou yag fi lool te weur

  • @ndeyemariemedieye4674
    @ndeyemariemedieye4674 3 года назад

    Dieureudieuf

  • @elhadjamadouba6153
    @elhadjamadouba6153 5 лет назад +7

    dierediefeti mbacké li rek lagnoudone kharthi yow leerna tidianlade Waye.sama serigne bi.wakhng.Lep

  • @ndeyefatougueye2849
    @ndeyefatougueye2849 5 лет назад +4

    Mane deh tidiane la wayer damala beuk lol mbacke daga sori thi mane dioulite pire NGA Liga beugeul sa bopp NGA beukeul gneup deuk rek Kay deuk say souma la deker am yokouter yalla Nala yalla May koudou fane bou andank wer kou yaram thi barcke Al Ouran

    • @mamediarraboussogaye2963
      @mamediarraboussogaye2963 5 лет назад

      Ndeye Fatou Gueye amiiiine sokhna ci yalnala borom bi fay yiw

    • @ndeyefatougueye2849
      @ndeyefatougueye2849 5 лет назад

      Amine way gnou bok KO

    • @bongacamara6998
      @bongacamara6998 5 лет назад +1

      mane mi tidiane la mais nonou la beugué serigne bou mak bi ak beep jabotam walahi yag fi mbacke t and ak weer joulite piir nga kou tedki mashalla

    • @el.hadjimamadoundiaye7957
      @el.hadjimamadoundiaye7957 4 года назад

      beugue nala guir liguako beugue

  • @mbaroudieng3883
    @mbaroudieng3883 4 года назад +1

    Mbacke yague fi lol te weer Serigne touba Nena Bira soumane bara Sani you bari soumane ndaw Bour yalla laye beurel Mbacke yague fi loll te weer yone bi Serigne touba ko teyel bopam

  • @taphasylla3784
    @taphasylla3784 4 года назад

    dieregnef serigne touba diarama mame chiekh ibra fall

    • @codoundiaye5179
      @codoundiaye5179 2 года назад

      MachaAllah s bi content nagn yaguou fi lol té weur 🤲

  • @amyfaye8169
    @amyfaye8169 5 лет назад

    Bilay mbacké Balla yagi fi lol té weur

  • @amimisow6518
    @amimisow6518 5 лет назад +2

    Amine inecha Allah

  • @mbayeseynabou8707
    @mbayeseynabou8707 5 лет назад +2

    Wallahi Aïda Diallo j'ai peur pour toi

  • @fatoukineloum7276
    @fatoukineloum7276 5 лет назад +1

    Serigne mountakha doundeul ba wéralo doundeul doundeul mbacké balla doundeul yagu fii lol té wer thi barké seydina mouhamed psl

  • @nemanema7999
    @nemanema7999 5 лет назад

    Serigne mountakha merna deh

  • @mmbaye892
    @mmbaye892 5 лет назад +3

    Yague fii té wér mbacké

  • @Diezflora
    @Diezflora 5 лет назад +1

    wakh dji rafetna mbacké balla aissé.
    yallah guafi yagg té weur.sokhna Aïda mom na dem rek lissi kanam rawoul beutt

  • @astoukebe1793
    @astoukebe1793 5 лет назад +5

    Adouna bi Dale bou bene goor wakhati djiguéne yaye mane maye yow ndah djiguéne matoule té li ngourgui nathi tahaw

  • @cheikhba4765
    @cheikhba4765 3 года назад

    Wawaw mbacké balla aïssa

  • @maremasoda7242
    @maremasoda7242 5 лет назад

    Ahh man de Mbacké sama xol toye na man de djiguen la waye ros na sili aIda dialo nekue 😭

  • @papadip788
    @papadip788 3 года назад

    Dieuredief Mbacké doudal wéeral nigual bayi ay téer toupo lou bâche bayi teére.dieuredief Mbacké.

  • @babacargning1507
    @babacargning1507 4 года назад

    Vraiment Aïda Diallo méré naa la loll, Diaradieuf Serigne bi yague fi loll té ande ak weur

  • @symedina-wv5lv
    @symedina-wv5lv Год назад

    Mane dé dama fogone ni sokhna Aïda mome Serigne yeugouko mou nèfi rek dit déf loko nekh tamite

  • @bouchradiagne9787
    @bouchradiagne9787 5 лет назад +6

    Aida dialo ni baye lakhad defone baye si ngène dakhko sa khathe daye dième yakh l islam tè meunouko

  • @aboutall2546
    @aboutall2546 3 года назад

    Une femme doit respecter les principes de l'islam . Ici au Sénégal c'est le kalife qui est le chef donc elle doit obéir au ordre du kalife ds mourides

  • @akd696
    @akd696 5 лет назад +4

    Aida diallo yaaa meuna fénnn man biii gathié guissouma louko diarrrr

  • @pendaseck9599
    @pendaseck9599 4 года назад

    Mbacké koulay merlo da xamoul poukaré rek mo nekh sokhna yoyou di mboubo serigne saliou

  • @sagardiaw7297
    @sagardiaw7297 3 года назад +1

    🙏🤲❤️♥️♥️

  • @diawbintadiaw8216
    @diawbintadiaw8216 5 лет назад +1

    Skey thieyy Mbacké yagg fi lol té and ak weeerr

  • @ibouba1389
    @ibouba1389 5 лет назад +1

    Billay Aïda Diallo li Soula djiké rék gay beur bakhna dokhall rék

  • @pendagueye8502
    @pendagueye8502 3 года назад

    ♥️♥️♥️🙏🙏🙏

  • @serignemamemormbacke2244
    @serignemamemormbacke2244 4 года назад

    Macha Allah yagufi tewer lol