En colère, le Khalife général des Mourides recadre Sokhna Aida Diallo

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 26 дек 2024

Комментарии • 207

  • @salimatadiallo1289
    @salimatadiallo1289 3 года назад +2

    Merci pour cette video yallana yalla yogue say fann ak werr werrlee amine amine bannee bou mame babacar sy rta de bordeaux merci

  • @matyseckkgueye2612
    @matyseckkgueye2612 3 года назад +1

    Dieureudieifeti Serigne bethio ❤deugui deugui dieumeum sokhna Aïda Saliou Thioune mom Serigne bethio yalla nafi yag lol tèh Guen wer🥰❤
    Thioune ioe lanou guem yay Serigne bethio ioe lanou beug ioe lanou deguel yay sounou yakar guemo kènen moudioul ioe yagfi lol tè wer

  • @abybodian9724
    @abybodian9724 4 года назад +1

    Sokhna Aida amal souniou kerssa nga takh beu sunu kilifeu di wakh ba deuneum djougu Li meetineuma 😭😭😭 Mbacké yagg fi tei weur mourid dieuffé ndiguel rekk amel nganiou akk

  • @aliounekane6581
    @aliounekane6581 3 года назад +1

    Dieuredieuf mbacké yagg fi lol té wérr AMINE 🤲❤️🙏🙏

  • @bassinesuzanesall4666
    @bassinesuzanesall4666 2 года назад

    J SS talibé cheikh mais khalif bi dama KO beug machala nittou diamla yalla goudeul sa fane mbectémi ❤️❤️❤️❤️

  • @momodoukane5861
    @momodoukane5861 5 лет назад +1

    Adia diallo lanne moko dall adouna diaynala merci beaucoup mbake balla aicha

  • @thejob3949
    @thejob3949 2 года назад +1

    Dioum nga d. Fane la charia wakhni djiguen bou toudou dom wala mayé seuy danioula wara thiaw diassi? Depuis quand la charia sanctionne par la bombe? Ki c un extrémiste hein! Comment tenir un tel discours à l'égard d'une femme ? De surcroît kou niak borom keureum diko djooy té nopegoul!

  • @thejob3949
    @thejob3949 2 года назад +2

    Ana charia ak nitt ni yeuw tog thie kaw nga tog thie souf, diko raamal, diko diokh hadiya ? So gueumè charia Key boul nangoti hadiya

  • @aidasow7493
    @aidasow7493 4 года назад +1

    Dieureudieuf mbakcé yala rek ressouloula serigne touba

  • @diadiabae2168
    @diadiabae2168 5 лет назад +24

    Walahi sama xol dafa toy diote na niou xamate yalla😭😭😭😭😭déh bilahi sante rék bila fi yalla indeii inchallah magui sa guinaw mane🙏

  • @cheikhsy7410
    @cheikhsy7410 4 года назад +1

    Dieureudieuf serigne touba serigne moutakha yalnafi yague wér

  • @khadimfall2712
    @khadimfall2712 4 года назад

    Mach alla diadieuf serigne Mountakha mbacke yalnaf yague te LoL barker serigne Touba

  • @khadimdiop2447
    @khadimdiop2447 5 лет назад +5

    Bilay yaram dawna serigne touba dou morom

  • @pptv8001
    @pptv8001 4 года назад +1

    Wa cou kham serigne touba moy Kane nguir yalla wakhma bilahi walahi kéne dou serigne touba

  • @maremeseck3589
    @maremeseck3589 2 года назад

    Dieureudieuf Mbacke

  • @binetasokhna9637
    @binetasokhna9637 4 года назад +7

    Mbacké Balla ak Aïssa lo doundou doyoul Yallah na Yallah yok say fane wéral la barkep Cheikhoul Khadim

  • @fallkhadim8358
    @fallkhadim8358 5 лет назад +8

    MACHALLAH MBACKÉ BALLA ❤️❤️❤️❤️

  • @aboubacargueye6572
    @aboubacargueye6572 2 года назад +1

    Le grand moufti du mouridisme: mouride ndigual serigne mountaga dolithi waya ndigueul thi terebi.

  • @omardieng719
    @omardieng719 4 года назад +1

    Grazie dio

    • @omardieng719
      @omardieng719 4 года назад

      Solo dio☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️

  • @abdoukarimba9189
    @abdoukarimba9189 4 года назад +2

    Mâcha allah

  • @diadiabae2168
    @diadiabae2168 5 лет назад +10

    Dieureudieuf Mbacké yague fi tei wér walahi yagui niouy dioubati bou bax🙏 di défare yalla na diam déf diam😭😭😭😭 cii miim réw

  • @sidifall6651
    @sidifall6651 4 года назад

    Mbake bala Yalla gafi yague teu weur ssi barki mouhamed inchallah

  • @ibrahimasow6331
    @ibrahimasow6331 5 лет назад +1

    Dieureudieufaty Mbacké am solo trop yagafi lol té anda ak wer thi Barcké Cheikh Abdoul khadre jeylani

  • @bathiendiaye3500
    @bathiendiaye3500 5 лет назад

    Machala mbacke Yalla na fi yaga te wer mbacke diadiaf

  • @sidyalmaktoumgaye5584
    @sidyalmaktoumgaye5584 5 лет назад +3

    Mbackè yalla na yalla yagal sa takhaway yalla mai la wer ak godou fan man mome Sama khôl dafa sèdde si yaw

  • @mamebathiegaye6836
    @mamebathiegaye6836 5 лет назад +43

    Ay😭 serigne bi diougué si magal bi sonou lolle wara dallou.. yaw mi teki woul dra ga takh bami guène di wakh ni.. amèl ganou akhe te mane balou mala...🤜

    • @fatoudembathioune4698
      @fatoudembathioune4698 5 лет назад +1

      MAME BATHIE GAYE wakh deug

    • @ndamarndiaye5252
      @ndamarndiaye5252 5 лет назад +1

      Gnak talibé rék nak ndakh lii métinagn0u lole sakh
      Sokhna si takh serigne bi tok di wakh
      Walahi souko aq talibé yi diapé mou torokh mane déi balou mako

    • @momarfall6707
      @momarfall6707 4 года назад

      Bilahiii

    • @amadoufadalba7688
      @amadoufadalba7688 4 года назад

      @@ndamarndiaye5252 .aqa

    • @cheikhniang6159
      @cheikhniang6159 4 года назад

      MAME BATHIE GAYE te

  • @issathior8041
    @issathior8041 5 лет назад

    Yalla n’a yalla defal diame thie barke alkourane mane talibé cheikh Ibrihime niass malako nianal vive la diaspora paix à vous merci respect pardon kouné thie Europe yalla sa papier yomboulaa

  • @diopmarieme4067
    @diopmarieme4067 5 лет назад +4

    Wa bakh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimakhalil9042
    @ibrahimakhalil9042 4 года назад +6

    Dieureudieuf mbacké yalna nga fi yagg lole té werr deff nga sa wareff 🤲❤❤👌

  • @diadjisamb2407
    @diadjisamb2407 5 лет назад +35

    J sui tidiane mé dama rouse pa c k bo kholé ni Khalifa bi di wakhé gua kham né kholame tague na trop

  • @gottkonteye6914
    @gottkonteye6914 4 года назад

    Billay mbacké yagfii lool té weur amine

  • @aboubacargueye6572
    @aboubacargueye6572 3 года назад

    Sans commentaire.

  • @coeur2lion913
    @coeur2lion913 5 лет назад +2

    Li dé bétouma bilahi bobou ba légi magi siy wah machala sénégal gép contane nagne si yaw tariha ak nitou diné yi li rék lagn done har yalna yalla goudal faneyi liga wah lou lére la cou déf lénéne nak sa bop aida diallo gnép la méti bilahi dioulit nak gno tah may wah

  • @abdulayeniang2058
    @abdulayeniang2058 4 года назад

    Dieureudieuf. Dieureudieuf Serigne.touba

  • @manebaba1319
    @manebaba1319 5 лет назад +1

    Yallna yalla maye werr ak daimou bou bahh

  • @KaboyChan
    @KaboyChan 4 месяца назад

    ❤❤❤❤

  • @falldior9914
    @falldior9914 5 лет назад +2

    Dieureudieuffattii sounou Kilifa bou Magg , bou tédeu gii . Ngatché nganlama . Conseil valable pour nos Dirigeants incompétent , et médiocre . SOKHNA AÏDA DIALLO , Buzz akk intérêt réék moko takha diokk . Mom nakk khamoul bopam té réw ba doff.

  • @KaboyChan
    @KaboyChan 4 месяца назад

    👂🏿👈🏿🤲🏿🙏🏿❤️🥰

  • @serignembacke5047
    @serignembacke5047 5 лет назад

    Aida Diallo yalla nala yalla rebou

  • @khadimniang5995
    @khadimniang5995 3 года назад

    😭♥️

  • @malicksarr5706
    @malicksarr5706 5 лет назад +3

    Machala Mbacke yalnala yalla samou yarabi samou yonwi ak talibèyi 🤲🏻🤲🏻🤲🏻🤲🏻

  • @mbayewade7931
    @mbayewade7931 5 лет назад

    Yalla nalafi yalla yaguale Mbacké Al Muntakha

  • @oumygueye7201
    @oumygueye7201 5 лет назад

    Bilay mbacke gen ganoo gindi yalla na ga yagg te wer

  • @laminekane3562
    @laminekane3562 3 месяца назад

    Cheikh bethio ndiguel rek la done dokhe.bako serigne sidy moukhtar djokhe ndiguel pour mou tegui cheikham yi dako dieuf.waye aida diallo domeramele

  • @abykaire1249
    @abykaire1249 2 года назад

    DIEUREUDIEUFATY SERING SALIOU MBACKÉ DIEUREUDIEUFATY SERING BETHIO THIOUNE DIEUREUDIEUFATY SOKHNA AÏDA SALIOU THIOUNE YALLA NA FI YAGUE LOLE TÉ GUENEU WËËR THI BARKÉP SERING SALIOU

  • @talibe-cheikh-ba-faww
    @talibe-cheikh-ba-faww 5 лет назад +18

    fii la cheikh béthio nek di fowé diiné dji kenn wakhou si.....voila les conséquences

    • @jadoredieuetmohamedkhadimo2521
      @jadoredieuetmohamedkhadimo2521 4 года назад +1

      Bilahi walahi domi baye ligua wakh deug la lep bethio thioune la mofi nekone di fowé yone wi batay li sogua nieuw ak complicité yene mbacke mbacke yi kou si melni serigne bass abdou khadre meusou sé wakh dara ndax ay interet bopam niouko amone si bethio ak aida diallo bene tawou ko mane yagu nako wakh bethio dafaye fo andak niouye fo aki thiagga domarame thiotou ndayou bethio ak wa keureum

    • @ahmadaly6666
      @ahmadaly6666 4 года назад

      @zeyna kante kiiiii

  • @daoudaba1354
    @daoudaba1354 5 лет назад +2

    Alakhou akbar

  • @manesourgeuye676
    @manesourgeuye676 4 года назад

    MASAHALA seriege bi

  • @moussathioune4152
    @moussathioune4152 4 года назад +3

    Sokhna Aida Dieuredieuff

  • @kaneabou4258
    @kaneabou4258 5 лет назад +5

    Serin touba yala reke

  • @diabelgaye6090
    @diabelgaye6090 4 года назад

    Machalla Akassa

  • @oumarmendy1336
    @oumarmendy1336 5 лет назад

    Machalha Mbackè balla yag fi lool te wer

  • @elhioye7457
    @elhioye7457 5 лет назад +5

    Je magnifie cette sorties parce qu’il est grand temps de faire face aux dérives .mais je vous suggère de ne plus accepter au centième venant de ces genres de soit disant Tabilés.veuillez arrêter recevoir leur hadiya.

    • @ndamarndiaye5252
      @ndamarndiaye5252 5 лет назад +1

      el hadji magaye thioye adiya dou dagnelakoy diokh nga déloko
      Seugeum gor djiguène m0mela yallah kharamale té meunena guéné adiya di sarahé aka diokhè azaka

    • @elhioye7457
      @elhioye7457 5 лет назад

      Mais dafa fek né koula eumbale sa sankhale nga eumbale ka soutourame

    • @ndamarndiaye5252
      @ndamarndiaye5252 5 лет назад +1

      Gnoune mourides kéne tagatougne si louniméle dokhéwougne kô
      Dama beug nga khame ni adiya yi talibé yi dî diokhé lousî léwoule lounék ni lagnekoy sépiwéi ndakh dougne dieufeudiko lou lèwoute segne touba mokoy sépil bopam wakhi batine leu nak beutt meunésouko guish .mandoule si adiya yi

    • @ndamarndiaye5252
      @ndamarndiaye5252 5 лет назад +1

      Serigne bi khamena lèpou loumou dieul lounék lou warla téi lou waurr leu

  • @JustForFun-fu9ry
    @JustForFun-fu9ry 4 года назад

    Jeureujeuf mbacké

  • @seydouanne6510
    @seydouanne6510 5 лет назад

    Merci mbacke

  • @aboubacarcamara5700
    @aboubacarcamara5700 5 лет назад +6

    Loudoul Alkhourane ak sunna Aÿ bidah ak thiahane là(yallah néna,yonneté bi(saws) néna point)

  • @aboubacargueye6572
    @aboubacargueye6572 2 года назад

    Il viennent nous enseigner, en 2000, un concept de serigne Touba ndigueul ak terer ( fondamentaux du mouridisme) mais en arabe : 'Samh wa Taha' la connerie humaine est sans limites.

  • @vieuxbadji3427
    @vieuxbadji3427 4 года назад

    Kou yabb yonou mouride thiatakoune ya takh s.mountakha yague fi lol té wér mbacké balla

  • @diouffamilly1031
    @diouffamilly1031 4 года назад

    Nous fatiguons de cette dame aida diallo elle salire notre tarikha mouride

  • @سميرهالسعدون
    @سميرهالسعدون 4 года назад +3

    😭😭😭❤❤❤

  • @thejob3949
    @thejob3949 2 года назад +1

    Thiowli bou barè yeux yaako waral. Cheikh bi né naniouma denthie Madinatou Salam nga ni non Touba mo gueun. Nga yobbou ko Bahia. Pourtant le khalife de Darou bimou fato, Darou laniou ko denthie té ya dem ba fofou tèwèko. Khana bobou da nga faté ni Touba mo gueun fenen? Da nga wakhone domam yi ni Di nga len Maye niou tabakh fa khabrou. Ana khabrou bi? Nenaniou ya wakh wakheet. En réalité cheikh bi meussoulen neekh

  • @fatousall416
    @fatousall416 4 года назад +3

    Aye mbacké niougui ziarre yalla gafi yague lole tè wer lole

  • @fatimabalde6972
    @fatimabalde6972 5 лет назад +2

    Aida diallo sounou akh soula dalei dou baakh dh

  • @elzofall5383
    @elzofall5383 5 лет назад +1

    Mbacké balla 🙏❤️❤️❤️❤️👏

  • @bintambaye7771
    @bintambaye7771 5 лет назад +3

    Deugue deugue Mbacke Balla Aïssa Machalah

  • @modounjie7204
    @modounjie7204 5 лет назад +2

    Machalla refetna

  • @combattrelinjustice1252
    @combattrelinjustice1252 5 лет назад +5

    SERIGNE MOUNTAHA mooo bakh

  • @mamansow3762
    @mamansow3762 4 года назад

    Bien

  • @massndiaye6062
    @massndiaye6062 4 года назад

    Machallah wakh dji Matt na mataléna

  • @ndeyeawadiop2696
    @ndeyeawadiop2696 5 лет назад +4

    li niawna walahi... mane dh rouss na en tant que dioulite, rouss na en tant que talibé mouride, rouss na en tant que djiguene... Yallah ngafi yague lolou tei werr Mbacké Balla Aissa, yonou mouride ndioukeul nala Mbacké

  • @cheikhndiaye9066
    @cheikhndiaye9066 5 лет назад +2

    Yalla ak serigne touba rek la fi degg ana yeunènte bi Mouhamed(SAW)??🤷‍♂️🤷‍♂️

    • @Moussigueul
      @Moussigueul 5 лет назад +2

      Yaw ya rer demal khol diagalé Serigne Touba!!!! avant gay oubi sa lamign.....

    • @amisarr1568
      @amisarr1568 5 лет назад +1

      Khana yonèntè bi dafa am bènèn yoon boudoul yonou yala
      Khana yonèntè bi motakh gnounan dioulite khana mom mo takh gnou kham yala
      Lou wax am am gniarigne sokhaloulèn lolèn critiquer ngèndi weur

    • @yayamane8077
      @yayamane8077 5 лет назад

      Ndiaye cheikh khana say noppeu neekhoul. Au debut mangui wakh ni serigne Touba ligueyeul yonente bi ak neek ci yallah rekk mokko takhone dioug. Yalla mo gueuna kawee leep kone diaroul niouy toudou tourr. Amleen horma ak kaadou you rafett ci kilifeu yi baakhna. Mane amouma tarikha mais sama khol daffa toyy te beugg na Serigne Mountakha beu fou beug yemm bess niki teyy. Des paroles de sage vraiment. Kilifeu gou barri keersa ak dall moy Mountakha.

  • @maremthiaw5081
    @maremthiaw5081 4 года назад +3

    bilaymbacke yakfi lo tes and ak wer

  • @nurukaneofficiel5049
    @nurukaneofficiel5049 4 года назад

    diereudieuf mbacke

  • @bacarfaye9907
    @bacarfaye9907 5 лет назад +2

    Aida Diallo negn ko douma torokhol ko. C'est tout.

    • @en2mots817
      @en2mots817 5 лет назад

      quel con , sa baye dako sak bagkoy toroxal doff gua rk

    • @labelle4941
      @labelle4941 5 лет назад

      Demal doumeu koo .. torokhal koo hahahhaha

    • @bacarfaye9907
      @bacarfaye9907 5 лет назад

      @@en2mots817 C'est toi le con (ou la conne) qui ne comprends rien. Tu crois qu'une menteuse va se foutre de nous, wayow. Vos trucs de féministe fonctionnent dans certains contexte mais pas dans celui-ci. Mbame yi guene ndone

    • @en2mots817
      @en2mots817 5 лет назад

      @@bacarfaye9907 le Senegal manque de tt sauf des fous

  • @talladiop8693
    @talladiop8693 4 года назад +1

    Sonu wala sonnn

  • @elzofall5383
    @elzofall5383 5 лет назад

    Merci 🙏 ❤️❤️❤️❤️❤️💯😭😭😭

  • @willblacked6743
    @willblacked6743 5 лет назад +24

    C'est bien vous le meritez. Quand bethio causait du tort à allah et à l'islam vous aviez rien dit. Aujourd'hui parceque sa femme menace votre business confrérique...vous criez au diable moi je dis le diable était déjà dans le verre .....
    Yallah molene di wane bopame rek.

    • @talibebamba5450
      @talibebamba5450 5 лет назад +5

      Will Blacked va chez tes maîtres saoudiens et émiratis si les sénégalais te plaisent pas !
      Cheikh Bethio était critiqué de jour en jour mais mossouléna yittel parce que yakamti nguén bountou pour meuna critiquer

    • @Yusucool
      @Yusucool 5 лет назад +9

      je partage ton point de vue.
      C'est la mafia mouride. Le clan tient a son business.

    • @combattrelinjustice1252
      @combattrelinjustice1252 5 лет назад +7

      Will Blacked Wollahi tu a parfaitement raison mon frère

    • @gildasatchade9535
      @gildasatchade9535 5 лет назад +4

      Le Khalife n''a rien contre la dame mais vues les pressions qu'il reçoit de part et d'autre il est sorti pour taper sur la table.
      La mysogegenie des hommes sénégalais font que le Khalife est. obligé de taper sur elle.

    • @Yusucool
      @Yusucool 5 лет назад +5

      @@gildasatchade9535 voila, une autre clef de lecture.
      la pression etait tres forte, le business et les privileges en severe menace ,alors Aida devient dangereuse pour le clan. L'ire monte chez les familles qui dependent de cette mafia confrerique pour survivre ont commence' les propagandes contre la femme de Bethio.....c'est tout un cercle vicieux

  • @cheikhdiouf7532
    @cheikhdiouf7532 4 года назад

    Mbacke yagfi te weur

  • @souleymanediop2970
    @souleymanediop2970 5 лет назад +2

    Machallah serigne serigne mountakha mbacke yague fi lol ta wer mbacke yonu mourid Wi dawsi touti na si yakh ko dou si masa am ndam chaytané rekk la andal wayé torokh rekk lay daf mok ngimou andal mbacke sante nanou la bou wer mbacke

  • @noreyni4612
    @noreyni4612 5 лет назад +4

    Merci beaucoup. Dieureuf kilifeu gou mague gui.

  • @mariamba5473
    @mariamba5473 5 лет назад +6

    Chéikh béthio ngén warone arrêté bou yague fi ngén KO bayi mouy déf louko nékh si Sénégal ak bir touba toujours mouy fowé l islam té meusolén KO téré li bétoul kén

  • @thejob3949
    @thejob3949 2 года назад

    Khana bo amé respect thie cheikh bi Di nga respecter Sokhnam. Waayé kilifa bawofi nga ni sokhnam da yaqqou! C'est grave! Waayé am nga Loula doy. Lidjeuntil sa sokhna sossou niouy djigne ... Lidjeuntil li mbacké mbacké yi néké Touba à commencer par bass momou sa wett

  • @amadoumafallfall9253
    @amadoumafallfall9253 5 лет назад +11

    Diabarou cheikh betio nila meunai mêle. C pas une surprise

  • @macoumbandiaye4655
    @macoumbandiaye4655 4 года назад

    Merci🙏🙏🙏🙏🙏🙏👏👏👏👏👏👏👏😭❤️

  • @bambadiop7451
    @bambadiop7451 4 месяца назад

    Nitte boko khasser ba paré delloko khalissame goor dou khasseter

  • @damassndiaye7064
    @damassndiaye7064 5 лет назад

    Dieureudieuf mbacke yalna nangafi yagu loollle tes wer

  • @عادلظريف-و5ج
    @عادلظريف-و5ج 4 года назад +2

    Nioun sokhna aida laniou gameu

  • @maremthiaw5081
    @maremthiaw5081 4 года назад

    mbacke yaw yay serignetouba

  • @hadimtouray7141
    @hadimtouray7141 4 года назад

    hallahi mbacke yah wah degue gou weer

  • @deboursy6215
    @deboursy6215 5 лет назад +2

    Macha alah

  • @ebrimacorea4956
    @ebrimacorea4956 4 года назад

    Lii dafa daw yaram bilahi
    ay tiaga you tékioul dara bega yakh yoonu Serigne Touba

  • @sigadione7750
    @sigadione7750 4 года назад

    Li metina thi khôl, aida Diallo founiou tope

  • @ndamarndiaye5252
    @ndamarndiaye5252 5 лет назад +3

    Mbackè sakh si sa ndigueul rék té bayi térré

  • @actudekouroumbackebayefall8114
    @actudekouroumbackebayefall8114 4 года назад

    Actu du khourou mbacké

  • @aliounefaye4155
    @aliounefaye4155 4 года назад

    Dieuf say ndiguela gueuneu wor di ko kafe

  • @305tall4
    @305tall4 5 лет назад +1

    Mbacké dioxe gnou ndigeul gnou généko touba

  • @bambabamba9638
    @bambabamba9638 5 лет назад +1

    aida diallo sonal ga gnou lole

  • @deggfeenjotna
    @deggfeenjotna 4 года назад

    Ya Allah sunnah rek

  • @euxlukhassida
    @euxlukhassida 5 лет назад +2

    Colére diam serigne bi doukouy mére

  • @fatoudiagne8048
    @fatoudiagne8048 2 года назад

    thiey touma moo grawe wayé naniou déme rekk