Kubakha nañou bayi lo lou S.TOUBA limou wote moy mouridou lahi temoy kunama dieum ci YALLA rekh fall dieure dieuf ñoun ñepou benalañou BILAHI BARGUEB S.TOUBA nañou anda samal YALLA SOUÑOU BOROM BI dinemdji rekh diaraleko ci sounas YONENTABI asw ak souñou ndiangalem kilifa DINE YI dieure dieuf ziarnala bouwer fall
Day doul dé. Foumou dém si publication mouride day weur nane je suis tidiane. Khana geumoléne séne bopou. Mouride gemeul sa bopou. Dou tidiane bu tagg mouride mouy done sa ndam. Gnak nga fayda trop way ishhhj
Bilahi walahi wa talahi Barki Serigne Babacar Sy vidéo yi Xalaat TV meusseu deff yeup bi moma si geuneu touché mangui soga setane vidéo di dioy ndahh xol bou fess 🥰 Serigne Mountakha Mbacké mérite même plus qu'un prix Nobel mais un monument national de son vivant. Mom ndeysan xamoul sahh dioulit ak catholique wahou mala ak tariha. Yalla nako Yalla doli werr ak goud fann 🙏🏾🙏🏾
Bilahi barki cheikhou tidiane magui niane dilènko sèdè lo lima dèsè sama doundou yalla xadjko dollil ko sange bi nakh doumdeum lou ame nierine la si rèwmi yalla na yalla goudeul faname
Je suis talibe Baye Niass. Et je temoigne que serigne Mountakha , je l aime tout simplement ❤️. Yalla nafi yague lol te wer mbacke .Amine Fi barakati Mouhammad SAW
Maguini talibe Cheikh Akan dayman, djokou thi Barhama !!!!! Wayé Yalla sédéna ni Serigne Mountakha damako beug ba dafa diégui dayoooo. Yalna Fi yaag lolou té wéérrr. Mbaccké♥️♥️♥️♥️♥️😍😍😍😍😍😍
Maguini talibe Cheikh Akan dayman, djokou thi Barhama !!!!! Wayé Yalla sédéna ni Serigne Mountakha damako beug ba dafa diégui dayoooo. Yalna Fi yaag lolou té wéérrr. Mbaccké♥️♥️♥️♥️♥️😍😍😍😍😍😍
Je ne suis pas mouride mais j'aime Serigne Mountaha Mbacké de son patriotisme et de son ambition pour le peuple 🇸🇳. Yalah nafi yag té wér🙏ak mbolémi kilifeu dîné thi rewmi🙏🇸🇳❤️
J'ai tellement d'amour pour Serigne Moustakha que je peux rien écrire sur lui si ce n'est pleurée par amour.... Merci Xalat TV aujourd'hui vous avez touché mon cœur
quel exmple quelqu un qui na jamais travailles un guide religieux qui ne mentine pas alkhourhane ak sounna seulement son grand pere bokale rek il faut dire la verite
Day geuna nekh rekk di geuna bakh ( défal 👍🏾 j’aime si tu es d’accord que Serigne mountakha Mbacke moye Serigne Touba si diamanome kone yallah nafi yague thé wére ❤️
@@cheikhoudrame2638 Ndayesane ya balh YALLA NA YALLA KONTANE DIEUREUDIEUFATI SERIGNE TOUBA ALMOUNTHA YALLA NAKOFI YALLA SOUNIOU BROME YANG GAL TÈM AND AK WER SI BARKEP SERIGNE TOUBA AK MAME CHIEH IBRAHIMA FALL AMINE YARABI. AK BOLÈM KLIFA DINÈ YEUPOU YI SI 🇸🇳SÉNÉGAL 🙏
Nieup lolou lagn beug na kounek yondee lien bi seu wa famille yeup rek niom tmt niou abonnés bouko defee in sha Allah niou matal 1m yi parceque ils le méritent vraiment 🇸🇳
Je suis tidiane mais je l'admire trop Serigne Mountakha. Yalla nako maye weer ak goudd fane bolessi kilifeu diiné yeup. Yalla na diam yagg Sénégal Ak ci adouna bi yeup. Bilahii un vrai missionnaire. Tei lepp diangate leu rek. Son sourire légendaire contamine tout le monde. Goudeul fane Mbacké.
Macky nous disait que les Marabouts sont des citoyens ordinaires mais c’est grâce à ces citoyens ordinaires que le Senegal🇸🇳 est sorti d’une situation extraordinaire Serigne Mountakha Serigne Babacar Mansour Serigne mahi Qu’Allah vous facilite vos missions
En tout ce qu'il est entrain de réaliser est tout simplement magnifique. C'est un vrai guide, qu'allah le laisse encore parmi nous. J'ai les larmes aux yeux wallahi
Thiey Serigne Mountakha mbacké Bassirou ya bakh ya gueun💜💜💜yallah na yallah gudeul sa fann ak wèrr mbacké guen yagu gueuneu wèrr ci barké Seydina Mohamed psl ❤️❤️❤️
Franchement, il a bcp participé au soutien économique mais aussi a la paix du pays. Mann dé, je l'admire de part sa bravoure et ces ambitions. Mbacké, YAlnag fii yague té wéér. Amin
Machalla xalaate yalle nalene yalla takhawou li ga wakh fi mome bamasi d'accorer yagg na lole nakh senegal warna dépasser fi yeupp sune ko defer comme niga wakh dina mena ame avancement merci xalaate s mountakh mb ... Yalle nafi yagg té werre❤️❤️
Amiine mais l'idée à ma modeste connaissance n'est pas de se séparer de l'enseignement français mais de s'enraciner spirituellement d'abord avant de s'ouvrir au monde contemporain.
@@aliounebadaralo7921 lépp louy ouverture ci aduna bi am nafa yémoul ci spiritualité bi rk. Amoul béne puissance ci aduna bi bougne développé enseignement wou moromou puissance sam ci biir deukeum. Lolu rk laci dioube lou. Ma ngui diéguelou nak. Merci
@@oumarbenkhatab8126 je comprends ,Que nos idées trouvent du concret et que dans un futur proche,les générations à venir puissent en bénéficier. Merci!
Bilahi suis tidiane mais j’ai envie d’être mourite à cause de serigne muntakha mbacke mi Koula mananoul fi dara takhaway bou mak ba matoul di wakh kouma mana yobou si serigne montakha ma diébalou 🙏🏽🙏🏽
Fall yaram nieuwall darou miname malafay yobou banga guiss ko incha allah sama yakar la moma geuneul louma am akk kouma meuna am ak loumou meuna donn sama yalla djii
Serigne same mbaye woutina xam xam founné mais fou mou dém fék né serigne mountakha mbacké diar nafa am xam xam bu wér ta doxé wouko wakhé wouko ak talibé rék moko ñior ak beug serigne touba 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Son statut dépasse l’aspect confrérie et de religion je vois un homme humanitaire mais aussi planétaire.yalla nafi yague té wérr une fierté pour le Sénégal....
@@dakartunisair cet homme est exceptionnel en moins de 3ans il a sût réaliser tout sa,sans budget ni rien juste le peu de cotisation que les talibés récoltent par ci par là c’est vrement formidable.si l’état avait fait cela dans chaque localité du pays le Sénégal serait l’un des plus développés en Afrique.je suis sincèrement ébahi par ce monsieur.
Kou beugue khalife généraux yi surtout Serigne mountakha yalla na yalla yok ay faname magui lay niane gua nianal ma marque bi ma guéné di collectionner ay t-shirt mou weur adina yeup yalla def si barqué si barqué borome darou noreyni ♥️🙏🙏🙏
Cey Mbacké Mo baax té Bary yeurmandé Yalla Nafi guëne yagg té guëne wér barké borom Touba. Vraiment c'est un grand plaisir avoir une chaîne youtube comme xalaat tv merci de tout cœur ❤️❤️❤️
Prions seulement pour qu’il vit longtemps encore avec nous 🙏 et qu’il continue d’avantage le travail très remarquable qu’il est entrain de bâtir. Et peut-être qu’un jour nous aurons la chance qu’il gouverne le pays
C'est la première fois ma comantir diaredieuf xalat✊ cheikh montakha kine dou mom😭 matna sakke lémou doun yalnafi yageu tawér rek thié barkép Cheikh Ibrahima fall lamp dieurdiafati
Billahi ken dou borom touba me iow Tamit meri te nga telle billahi mirite nga leepou lou bakh thi adouna yallna ko yalla deff thi barki borom touba je vous J'aime
Bilahi j'aime bien le khalif je ne suis pas mouride mais je suis très fier de lui et je l'admire beaucoup diareujeuf Yallah diareujeuf Serigne Touba tout ça c'est son travail. Yallah nanga gouddou fanne té weerr
Vraiment ça m’a touché je n’ai jamais été aussi touché de ma vie. En regardant cette vidéo j’ai les larmes aux yeux. Merci Xalaat TV sène liguey rafetna manchallah
Pour mane moy le père de la nation ndakh dokhé nako wakhé nako yeureum na ndaw gni. Mane 2012 lako ndieuk guiss rek beug ko té Yalla takh. Serigne Mountakha kou bakh kounek dingako beug. Limou def thi rewmi gnp tekk nagn thi seni gueut. YALLA nako fi YALLA yagal wereul ko❤❤
*Ta lébé baye niass la mais Serigne mountakha dama ko begue rk té yalla takh ndakh takhawayam si réw mi yalna yalla goudeul fanam si barky Mouhammad psl*
Wallahy frère degue nga wakh niép benna lagnou gni gnou djiti kay gno begue yakha Sénégal rk mais sou gnou kilifa diné yi man nagnou dokhal Sénégal bamou réwisur
😳 je pensais qu’on pourrait cliquer sur j’aime pas dans toutes les vidéos sauf celle de ce genre 🥺 Pourquoi vous n’aimez pas le bien ? Al Mountakha Yalla nakofi Yalla bayii ci barkép Xassida yi ak Borom bamou motalii nalii kou tédKi 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Je penses qu'il y'a des personnes qui ne comprennent pas les pousses j'aime ou j'aime pas, il y'a d'autres qui le font par mégarde ils ne s'en rencontrent même pas et le reste momm peut être moy gni bagne islam rék gratuitement. Qu'Allah soit satisfait de nous inchaAllah
Merci xalaat tv nationale 🇸🇳 Seringe mountakha le père de la nation 🇸🇳 yalla nafi yegue LOL te weer Amine 🤲🤲 iow mi di senate wekhal Amine wala nge j'aime 👍
Je suis tidjiane mais Serigne mountakha amoul morom
Dieureudieuffff Serigne Touba🙏🙏🙏🙏
Bayileen "je suis tidiane ou autre chose mais" Serigne Mountakha ummah islamique yeup lay représenter
Kubakha nañou bayi lo lou S.TOUBA limou wote moy mouridou lahi temoy kunama dieum ci YALLA rekh fall dieure dieuf ñoun ñepou benalañou BILAHI BARGUEB S.TOUBA nañou anda samal YALLA SOUÑOU BOROM BI dinemdji rekh diaraleko ci sounas YONENTABI asw ak souñou ndiangalem kilifa DINE YI dieure dieuf ziarnala bouwer fall
Machallh wallahi li daye bakh ñou defalko hommage amna solo
Day doul dé. Foumou dém si publication mouride day weur nane je suis tidiane. Khana geumoléne séne bopou. Mouride gemeul sa bopou. Dou tidiane bu tagg mouride mouy done sa ndam. Gnak nga fayda trop way ishhhj
Xalat tv domou daarayii rèkk mokomanayorr ouztas Samba Diallo wakhonn naco
Nianal len Serigne mountakha Bassirou Mbacké mou yagu fii téé weer
👆👆👆👆👆
🤲
Amiinn
Amine yaraby
Amine Yaa Rabbal Haalamiin
Amine
Bilahi walahi wa talahi Barki Serigne Babacar Sy vidéo yi Xalaat TV meusseu deff yeup bi moma si geuneu touché mangui soga setane vidéo di dioy ndahh xol bou fess 🥰 Serigne Mountakha Mbacké mérite même plus qu'un prix Nobel mais un monument national de son vivant. Mom ndeysan xamoul sahh dioulit ak catholique wahou mala ak tariha. Yalla nako Yalla doli werr ak goud fann 🙏🏾🙏🏾
Amine
Machalah toi aussi sa xalaat rafetna diadieufeu ti xalate tv dieureudief serigne touba
Bilahi barki cheikhou tidiane magui niane dilènko sèdè lo lima dèsè sama doundou yalla xadjko dollil ko sange bi nakh doumdeum lou ame nierine la si rèwmi yalla na yalla goudeul faname
Souleymane dioyelo ngama........que Dieu te protège daradjaye nabi Moustapha PSL.
@@youssoudrame4627 yabakh
Kou sopp serigne touba buesal j'aime way
Koussa xole nékh si Serigne Mountakha Mbacké besseul j aime
Yalna fi yang tè wèr amine
Une solution pour mettre dehors l'école de jule ferry
Amine
Je suis talibe Baye Niass. Et je temoigne que serigne Mountakha , je l aime tout simplement ❤️. Yalla nafi yague lol te wer mbacke .Amine Fi barakati Mouhammad SAW
Maguini talibe Cheikh Akan dayman, djokou thi Barhama !!!!!
Wayé Yalla sédéna ni Serigne Mountakha damako beug ba dafa diégui dayoooo.
Yalna Fi yaag lolou té wéérrr. Mbaccké♥️♥️♥️♥️♥️😍😍😍😍😍😍
Maguini talibe Cheikh Akan dayman, djokou thi Barhama !!!!!
Wayé Yalla sédéna ni Serigne Mountakha damako beug ba dafa diégui dayoooo.
Yalna Fi yaag lolou té wéérrr. Mbaccké♥️♥️♥️♥️♥️😍😍😍😍😍😍
Amine way yalla nafi yague lolou te weer si barkeh khadim Rassoul
Amin mbacké
Je ne suis pas mouride mais j'aime Serigne Mountaha Mbacké de son patriotisme et de son ambition pour le peuple 🇸🇳. Yalah nafi yag té wér🙏ak mbolémi kilifeu dîné thi rewmi🙏🇸🇳❤️
Walaye ndaye sane amine 🙏
Àamine sërigne bi
Ndeye Sane Amine 🖤
Mouride mooy ki takku jeum thia yalla
AMINE yarabi
J'ai tellement d'amour pour Serigne Moustakha que je peux rien écrire sur lui si ce n'est pleurée par amour....
Merci Xalat TV aujourd'hui vous avez touché mon cœur
Kou sa khél dal d'ici qlq années Lép changer dieredieuf s mountakha beuseul j'aime
Serigne Mountakha Pére de la nation Yalla nafi yague lolou ta andak weir amine
Je suis Tidianne mais bilahi je n'ai jamais vu un homme comme Serigne Mountakha Mbacke. Un exemple pour tout le monde. Dieureudieuf Mbacke balla
Daaga bakh rkj
Ndeye sane danga bakh rekk mbirmi mome nio book ben deuk bouniou diem danio bokoul yone rekk
Tdiane la tamit dh mais nonou lako beuguei bilahi. Souniou Mame diou bakh dji
quel exmple quelqu un qui na jamais travailles un guide religieux qui ne mentine pas alkhourhane ak sounna seulement son grand pere bokale rek il faut dire la verite
Yaa bakh yaram
Day geuna nekh rekk di geuna bakh ( défal 👍🏾 j’aime si tu es d’accord que Serigne mountakha Mbacke moye Serigne Touba si diamanome kone yallah nafi yague thé wére ❤️
Amiiine
Amine
Des Cœurs ♥️ pour Serigne Mountakha yalla nga fi yag ta ande ak wér 🤲🏼borom yeurmandé dji😍🥺❤️
❤️
Bilayy je suis Tidjane mais il participe beaucoup dans ce pays. Bou gnèmm mèllone ni mome konne kènne dou mèrr🥰♥️
Arrêtez Vos Je Suis...mais !!!
Bayel lolou man Mouride la mais bilahi dama beugue El hadji Malick lépou benne la lépou yalla la❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@@zouazou4048 D'ACCORD AVEC VOUS! IL S'AGIT D'UNE FIERTE NATIONALE!
lie pou lou Masa def Vidéo Serigne Mountakha Mbacké mou ma si gena nekh YALLA NA FI YAGE BARKI SERIGNE TOUBA
Wallahi ndaysan
Serigne mountakha mbacke yallah naffi yague te were si barquer seydinamoukhamad ak barquer serigne Touba ba mbacke 🤲🤲🤲
Serigne mountkha Mbacke yala nafi yagou Loul ta wér tay moum contanna Loul
@@cheikhoudrame2638 Ndayesane ya balh YALLA NA YALLA KONTANE
DIEUREUDIEUFATI SERIGNE TOUBA ALMOUNTHA YALLA NAKOFI YALLA SOUNIOU BROME YANG GAL TÈM AND AK WER SI BARKEP SERIGNE TOUBA AK MAME CHIEH IBRAHIMA FALL AMINE YARABI. AK BOLÈM KLIFA DINÈ YEUPOU YI SI 🇸🇳SÉNÉGAL 🙏
Machallah xol yépa sédd
Moi je suis un talibe chekh mais je suis fier de cette homme de dieu yaguefi te werr mback❤se doundou amna solo lolee
La première fois que je fais un commentaire. Serigne Mountakha yalla nafi yag té wér. Dieurefieufety
des aimes pour serigne mountakha mbacké yall nafi yag
Amine ta and ak wer
Amine amine
AMINE Yarabi Tè Ande Ak Wer Si Barkep Serigne Touba Ak Mame Chieh IBRAHIMA Fall 🇸🇳🙏AMINE Yarabi
ken du moom kudul moom al mountakha yag fi te wer balla aysa
Kou beugu xalaat tv ame des million d'abonnés bala fin année beusseul 👍
Nieup lolou lagn beug na kounek yondee lien bi seu wa famille yeup rek niom tmt niou abonnés bouko defee in sha Allah niou matal 1m yi parceque ils le méritent vraiment 🇸🇳
سكر tv
@@Thegrindneverstops4l1m inchalla dina mate dakh gni gui xamal askanwi ❤️🙏
Nio Xalate ça kaman amineeee
abonné 2foi bou Amon ma def ko machalla
Kou beug Serigne mountakha doundou 170 ans sans ordonnance besseul j’aime 👍 ça ne te coûtera rien ci barkei Seydina Mohamed psl Amine 🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Amine way
🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Aminn
Aly Seck 🙏🙏
Amiine
Serigne MOUNTAQAH mérite plus que tout ce qu'on lui veut.Mbacké yagal wéral yokal.
Mbacké yag fii lol té wer sa doundou gui souniou Diarigne lah 💓💓🇸🇳🙏Bilahi koula diokhone réw mou dieum kanam svp des j'aime pour Almountakha 💯💓🇸🇳🙏
Je suis Tidiane mais j’adore trop serigne mountakha yallah naffi yague tè weerr ❤️❤️❤️❤️✨❤️❤️
Ndeysane amna solo 👍
Moi bilay babacr la toddo mei ki mome kene lafi
Machalah
Amine
Oh allakhouma amine waye yalgafi yag yaw tmit ❤️❤️😭🙏🏻
Yall nafi Yague Loull Mbacké Ta Weurr Amine Ya Rabbi
Dine rke moye degue
Yalna fi yague te weer
makhtar Sarr linga wax moy deg na khalifa généraux diel.rewmi
> limoy li werr
@@seydinaalioucamara5229 parfaitement raiso3
Un homme multidimensionnelle...yalna yalla bayikofi bassi kanam♥️🙏🇸🇳
Serigne Mountakha le père de la Nation❤️ merci xalat pour cet hommage❤️🙏🏿
Je suis tidiane mais je l'admire trop Serigne Mountakha. Yalla nako maye weer ak goudd fane bolessi kilifeu diiné yeup. Yalla na diam yagg Sénégal Ak ci adouna bi yeup. Bilahii un vrai missionnaire. Tei lepp diangate leu rek. Son sourire légendaire contamine tout le monde. Goudeul fane Mbacké.
Amine
Amineeee
Billahi man ak yaw gnio yam je suis tidiane mais damako beug
Yala Na sa diamou yague
@@s.falloudia1526 amiine serigne Fallou niou bok lepp in sha allah
Macky nous disait que les Marabouts sont des citoyens ordinaires mais c’est grâce à ces citoyens ordinaires que le Senegal🇸🇳 est sorti d’une situation extraordinaire
Serigne Mountakha
Serigne Babacar Mansour
Serigne mahi
Qu’Allah vous facilite vos missions
🤞❣️
SERIGNE Mountakha l’homme de tous les temps
Baa yeug guéne né adouna bamou dadj Serigne Mountakha Mbacké moo fi gueun🥰❤️
Wakhalll way bilahi yaw
Lou wore la😍
Kou gueune thi nittt yii yalla rekk moko kham
MATAR GUEYE LOLOU LA GUEME MANE!
@@mansoursao664 LI WOKHINE LA REK YOW TAM! COU DJIS NENE NEH NENA GUI!
Je pleure en regardant cette vidéo barki Serigne Fallou🥺 Serigne Mountakha Mbacké yallah ngafi yag tei weir yay sougnou lep barki Serigne Fallou ♥️🙏🏾
Wallahii
En tout ce qu'il est entrain de réaliser est tout simplement magnifique. C'est un vrai guide, qu'allah le laisse encore parmi nous. J'ai les larmes aux yeux wallahi
En 3ans il a fait autant qu' un autre qu' est là depuis 9ans
Mbacké YALLAH ngua fi yagg té werr allahou ma amiin
Incroyable daffa amati solo Kou d’accord 👍 na aime
Xalaat tv moye sunu tv kou d'accord lale j'aime serigne mountakha mb yalla nafi yageu
Machala amana solo ndji rek lanou wara djital so noum reio ndae ndioom keippo kou ndiou gis bindoub souno la ndioy khol dji yao
Serigne Mountakha Mbacké yall nafi yague té werre🙏🏾🙏🏾❤️
Amine
Amine
Thiey Serigne Mountakha mbacké Bassirou ya bakh ya gueun💜💜💜yallah na yallah gudeul sa fann ak wèrr mbacké guen yagu gueuneu wèrr ci barké Seydina Mohamed psl ❤️❤️❤️
Yalla nafi S bi yageu ta werr Amine 🇸🇳kouko beuk beuseul j’aime
Lima gueunal si adouna moye Serigne Mountakha mou Yagg té wére amine ❤️❤️❤️🥰🙏
Machalla Mbacke balla
Allahouma amine
Amine😭🙏🙏🙏🙏🏻
Amin waye
AMINE yarabi 🇸🇳🙏😭😭😭
Franchement, il a bcp participé au soutien économique mais aussi a la paix du pays. Mann dé, je l'admire de part sa bravoure et ces ambitions. Mbacké, YAlnag fii yague té wéér. Amin
Machalla xalaate yalle nalene yalla takhawou li ga wakh fi mome bamasi d'accorer yagg na lole nakh senegal warna dépasser fi yeupp sune ko defer comme niga wakh dina mena ame avancement merci xalaate s mountakh mb ... Yalle nafi yagg té werre❤️❤️
Le père de la nation souniou fierté souniou Serigne Touba Al Mountakha Mbacké yalna geuneu yagg geuneu wéer si BARKI cheikhoul khadim❤️🙏👌
زعيم الأمة تاج الدين
السيد الأمين الوفي أمير المؤمنين
الشيخ محمد المنتقى السنغالي🤲 حفظه الله ورعاه وأيده ونصره ءامين
Merci beaucoup la Chicoriénne mais MBA dém gua choucori
@@djibisy1320 nio far fall non dama teunkou si ndigeul li rek mais bala koor gui dagniy dem ziar Mame bi
@@chikorienne ndaysane wérna loudoul ndigeul Amou ndiarign motax wayé ziar bi mom lou âme solo la
@@djibisy1320 mom lagn fi ame fall amoul lenen
Vraiment sama yaram dawna lii dafa nékh ci yonu l'islam 😭😭😭😭😭😭
Merci way islame mo kontane tay
@@papelesshanndiagne2203 walahi kay pape 🥰🥰🥰💪💪💪👏
Ma ngui niane yalle tivaoune, kaolack, layenne, omarienne, ndiassene,khadre yi... niom nieup am universités bou mélni wala gnouko raw. Sou amé légui diagalé toubab yi abale gnou ci barké seydina mohamed(psl)
Amine Ya Rabbi
Amiine mais l'idée à ma modeste connaissance n'est pas de se séparer de l'enseignement français mais de s'enraciner spirituellement d'abord avant de s'ouvrir au monde contemporain.
@@aliounebadaralo7921 lépp louy ouverture ci aduna bi am nafa yémoul ci spiritualité bi rk. Amoul béne puissance ci aduna bi bougne développé enseignement wou moromou puissance sam ci biir deukeum. Lolu rk laci dioube lou. Ma ngui diéguelou nak. Merci
@@oumarbenkhatab8126 je comprends ,Que nos idées trouvent du concret et que dans un futur proche,les générations à venir puissent en bénéficier.
Merci!
أطال الله عمرك يا شيخنا الكريم "شيخ محمد المنتقى " أطال الله عمرك وزاد صحتك ببركة قرآن الكريم🤲🏻🤲🏻💖💖
Bilahi suis tidiane mais j’ai envie d’être mourite à cause de serigne muntakha mbacke mi
Koula mananoul fi dara takhaway bou mak ba matoul di wakh kouma mana yobou si serigne montakha ma diébalou 🙏🏽🙏🏽
Mashallah Ndeysaan♥️🙌🏻
Diokh masa contacte ma yoboula si mome nga diébalou
Donne moi tes cordonner
Je vé t'envoyer chez luis pour nga diebalou
Bilaye tidiane dangéna bakh rek bilaye
Fall yaram nieuwall darou miname malafay yobou banga guiss ko incha allah sama yakar la moma geuneul louma am akk kouma meuna am ak loumou meuna donn sama yalla djii
😭😭😭😭😭😭😭 yagui and AKH werr...THIEY serigne
Merci xalatt tv
Khalate mba hamnani mourite yangui koy weur pour teral ko 😭😭😭❤️❤️❤️❤️
Bilaye deh werna
Machalla
Bilahi 🙏 Serigne MOUNTAKHA MBACKÉ YALNAFI YAGUE TÉ WÉR SI BARKI ARHOU-RANE Amine 🤲 nélen amine té bess aime 🙏
Amine
AMINE yarabi
Nagne co diokh senegal. C'est ces genres de personnes qui méritent la tête de la nation walahi😞😞😞
Serigne same mbaye woutina xam xam founné mais fou mou dém fék né serigne mountakha mbacké diar nafa am xam xam bu wér ta doxé wouko wakhé wouko ak talibé rék moko ñior ak beug serigne touba 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Jajeuf amna sollo
@Asral Tv c bien
Dieureudieufati Sante rek mbacke
😭😭😭😭😭 thieuy Balla Aïcha yalnafi yagg ndax yagam fi sounou ndieurigne la,Billahi j'ai des larmes aux yeux...
Merci
Un vrai visionnaire, un homme de science, digne héritier de serigne touba. Yalla nako fi yalla bayyi ak nun bathi kanam.
MANDOUMBE KANE BIEN DIT RIEN A AJOUTER. VOUS AVEZ PENSE JUSTE!
Xoll sède na serigne mountakh yalla nafi yage tè wèr mèrci xalaat
Il a, à 100%, accompli sa mission. Yalnafi yageu loll té werr, mbacké🙏🙏🙏
Amine
Amine ya rabi 🙏🙏🙏😭😭😭
Merci beaucoup
Quartier Général yalla boume am si koor gui
Tidiane mouride layenn.... Gneup bènn la 💓💓💓💓
Tioutou ndayou kouy diaxasé keurou dinéyi .. on est tous des frères kou nara diaxasé keurou dîné Yi yalla boko fékè 🙏🏽🙏🏽🙏🏽 dama mér rk guéne balma
Ndeysanne legui majorité senegalais yi lou rafete rek laniouy gnane ak nougn ko meunti waxer ❤️❤️❤️
Billahi damako ñaane ba sonn yalnako yalla nangu way Amine
Serigne mountakha l'homme de tous les temps KOU d'accord
Pour une première fois que je commente
Je suis musulman et patriote mais djieureudjeuf serigne bi li lagnouy xare si yéne MachaAllah
❤je viens de découvrir cette vidéo sur Serigne Moutakha Mbakké que j'ai beaucoup aimé❤ Merci X🧠lat tv
Je suis Tidiane mais nima beugué Serigne Mountakha billahi dama diaxal trop 😍😍❣❣❣❣❣❣ yalla na yalla mayko goudou fane ak wërr😍😍
Ndeysane danga bakh rek ñoun ñépeu fii lan wara nk
Yalna sa dimm yagg
Yawit Goudal fan waay
Mouride ak tidiane béne la lousi diar mane tidiane la wakhal rek magui diégalou nak
Beuri nga si ay morom dh ndaysane yalna diamm yagg
Son statut dépasse l’aspect confrérie et de religion je vois un homme humanitaire mais aussi planétaire.yalla nafi yague té wérr une fierté pour le Sénégal....
AMADOU SOW JE SUIS EN PARFAITE COHESION AVEC VOTRE ANALYSE SI REELLE ET JUSTE!
@@dakartunisair cet homme est exceptionnel en moins de 3ans il a sût réaliser tout sa,sans budget ni rien juste le peu de cotisation que les talibés récoltent par ci par là c’est vrement formidable.si l’état avait fait cela dans chaque localité du pays le Sénégal serait l’un des plus développés en Afrique.je suis sincèrement ébahi par ce monsieur.
Lou were ngua wakh
Mbacké balla yagui fi rek ya fiy souniou serign touba 🧡🧡🧡🧡
vraiment serigne bi yalnafi yague ta wérrr 😓🤲machallah
merci xalat tv 👍
Këupp kou contant si serign mountakha mbacke bëuseul Jaime yalnafi yague ta wëur amiine
Amine wayé
❤❤❤❤❤❤❤❤
mbolim li ğay dénosse solution bi fila
AMINE yarabi
Kou beugue khalife généraux yi surtout Serigne mountakha yalla na yalla yok ay faname magui lay niane gua nianal ma marque bi ma guéné di collectionner ay t-shirt mou weur adina yeup yalla def si barqué si barqué borome darou noreyni ♥️🙏🙏🙏
Amin
@@callmeafricawoman5518 ♥️♥️💫
Machallah je suis tidiane dh mais je l’estime beaucoup❤️🙏🏼yalla na sa diam yagg Mbacké balla👌
MachaALLAH
J'apprécie beaucoup ce Marabout il est trop fort
Merci beaucoup encore Xalat tv
Qu'ALLAH nous Préserve de Tout mal que peut exister
Serigne mountakha fierté la si keep kouy sénégalais
Je suis pas mouride mais il mérite plus qu'un prix nobel yalna yalla goudal fanam
Amine kou bahhh
Nn vraiment lou bakh rkk layy deff
Sa khôl mo raffétt rek
Machalla yaw tmt yalnala yalla fay sa xol bou rafèt
Serigne mountakha mbacké yalla na fi yagui te wuer barkep serigne touba
Le meilleur chaîne RUclips de tout les temps
Cey Mbacké Mo baax té Bary yeurmandé Yalla Nafi guëne yagg té guëne wér barké borom Touba.
Vraiment c'est un grand plaisir avoir une chaîne youtube comme xalaat tv merci de tout cœur ❤️❤️❤️
All mountakha jammi sénégal 🇸🇳 rk moco ndiorr Mbacké bala Aïcha yall naffi yagg teii werr j’aime 🙏
Xana dii niane yalla mou yagg fii rék té wérr sii barké serigne touba🙏🙏🙏tapez amine please
Prions seulement pour qu’il vit longtemps encore avec nous 🙏 et qu’il continue d’avantage le travail très remarquable qu’il est entrain de bâtir. Et peut-être qu’un jour nous aurons la chance qu’il gouverne le pays
Je sais mm pas quoi dire wallahi j'ai les larmes aux yeux 😭😭😭. SERIGNE MOUNTAKHA MBACKE yalla nafi yague té wére. Sa doundou amal naniou dieuragne
Serigne Mountakha Mbackè yalla na fi yage Lole tè And ak Wèrre 🤲🤲
Walaxi Serigne Mountakha day séral Xoll yi ❤️❤️ Yalnafi Yaague Lool téwér 🤲🏽
Billahi Lou wer la
Ma chalah Mbake yal na fi ya gue te we diara diaf
Gueuna yagu gueuna werr mbacké❤️🙏🏾
C'est la première fois ma comantir diaredieuf xalat✊ cheikh montakha kine dou mom😭 matna sakke lémou doun yalnafi yageu tawér rek thié barkép Cheikh Ibrahima fall lamp dieurdiafati
Guirr yalla rk may ma jaime masu mko am té tjrs ma sétane😥
Yamaa geuneul mille président billahi mbacké,mbacké,mbacké yallah na goude fan téé werr Bark seydina Mohamed (psl)🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Nianal len Serigne mountakha bassirou mbakcé mou yagu fii téé weér ❤️❤️❤️❤️🙏
En vérité , il est le xalif de toute spiritualité et le général du temporel Geuna yague guena wer mbacké balla Aïcha bou sagnone niepp dém Aldjana🙏🙏🙏🙏
Amine 🙏🙏🙏🙏
@@mordiang9425 amine ya rabi
Amine dafa bakh nieup la yené diam
AMINE yarabi, 🙏🇸🇳lo lou dafa lère
Soxna ci yaa baax
Kou beug ndiabot Serigne Touba mayma j'aime ma guiss 😍👍
Billahi ken dou borom touba me iow Tamit meri te nga telle billahi mirite nga leepou lou bakh thi adouna yallna ko yalla deff thi barki borom touba je vous J'aime
dieureudieuf Serigne Touba Serigne Mountakha Mbacké yalnafi yague té Wéer
khole Sédna Mbacké balla
Serigna Mountakha Mbacké Yallah nafi yagg lool ta wérr Ana djikou burg😍😍😍
Amine
AMINE yarabi
Billahi kouko diokh senegal mou défarko❤️🙏🏿😭
Bougoyko sax
Merci. Way wakh nga deug dh
Deug l
Oh man damako beug depuis ma nèk xalé. Serigne Mountakha yalnafi yàgg ta wér. Moy suñu Sëriñ Tuubaa di suñu trésor.
Bilahi j'aime bien le khalif je ne suis pas mouride mais je suis très fier de lui et je l'admire beaucoup diareujeuf Yallah diareujeuf Serigne Touba tout ça c'est son travail. Yallah nanga gouddou fanne té weerr
Serigne Mountakha le véritable père de la nation Yalla nafi yagueu té wer🙏🏽 Dieurédieuf xalaat tv
Vraiment ça m’a touché je n’ai jamais été aussi touché de ma vie. En regardant cette vidéo j’ai les larmes aux yeux. Merci Xalaat TV sène liguey rafetna manchallah
Pour mane moy le père de la nation ndakh dokhé nako wakhé nako yeureum na ndaw gni. Mane 2012 lako ndieuk guiss rek beug ko té Yalla takh. Serigne Mountakha kou bakh kounek dingako beug. Limou def thi rewmi gnp tekk nagn thi seni gueut. YALLA nako fi YALLA yagal wereul ko❤❤
Bougne ko diokhé rewmi mou yor ko dé mbacké borom yeurmandé la❤❤❤❤❤
*Ta lébé baye niass la mais Serigne mountakha dama ko begue rk té yalla takh ndakh takhawayam si réw mi yalna yalla goudeul fanam si barky Mouhammad psl*
Amine
Niep ben la
Amine
Wallahy frère degue nga wakh niép benna lagnou gni gnou djiti kay gno begue yakha Sénégal rk mais sou gnou kilifa diné yi man nagnou dokhal Sénégal bamou réwisur
Linak moy Sénégal dom yaye
😳 je pensais qu’on pourrait cliquer sur j’aime pas dans toutes les vidéos sauf celle de ce genre 🥺 Pourquoi vous n’aimez pas le bien ? Al Mountakha Yalla nakofi Yalla bayii ci barkép Xassida yi ak Borom bamou motalii nalii kou tédKi 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Sokhor rèk bilay
Dagno inconscient rk
Khel mu gatte rek
Je penses qu'il y'a des personnes qui ne comprennent pas les pousses j'aime ou j'aime pas, il y'a d'autres qui le font par mégarde ils ne s'en rencontrent même pas et le reste momm peut être moy gni bagne islam rék gratuitement.
Qu'Allah soit satisfait de nous inchaAllah
Niaka kham rék wayé Yallah bakhna..
Serigne Mountakha Yallah nafi yageu té wérr
Je suis tidiane mais damako sopp lol ndakh yeurmandem yalla na yalla goudal fanamm amine
Diadeuf
Amiiiine
ndeysan yalna la yalla faye thie sopu gui
Amine
Kéndou mome Kou Begue melne mome Sax yomboul Mbacke yagg fy té wérr ❤️
Machalla xalate diadieuf kou beugue Serigne mountaha beusseul j aime
Serigne mountakha mbacke yalla nafi yagg té wérr amine yarabi🤲🙏
Merci xalaat tv nationale 🇸🇳 Seringe mountakha le père de la nation 🇸🇳 yalla nafi yegue LOL te weer Amine 🤲🤲 iow mi di senate wekhal Amine wala nge j'aime 👍
wawaw manna néké kay bilay
AMINE yarabi Wawaw
Serigne mountakha Mbacke yalla nafi yague teweur barke borom touba