Kan Mooy Serigne Atou Diagne Ak Taxawaayam Ci Hizbut Tarqiyyah

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 окт 2024

Комментарии • 3,1 тыс.

  • @TeleDialibatouInternationale
    @TeleDialibatouInternationale 3 года назад +260

    Thiey Serigne Atou Diagne😭😭😭 jambar deugu dem na

  • @ToubaVisionToubaVision
    @ToubaVisionToubaVision 3 года назад +278

    Dia Dieuf Xalaat TV Amatina Solo

  • @laminemane6383
    @laminemane6383 3 года назад +108

    Mission accomplie, brave homme que DIEU t’accueille dans son paradis

  • @papidiagne1942
    @papidiagne1942 3 года назад +314

    Qu’Allah l’accueil dans son paradis céleste 🤲🏾

  • @kalleseye9517
    @kalleseye9517 3 года назад +476

    Kou sope seyedina mouhamed psl beuzeull j'aime ❤️❤️s atou diagne yalla na souff oyoff si kawam si barképp s touba mbacke😰🤲

  • @SeneInfo
    @SeneInfo 3 года назад +133

    Masalah xalaat tv

  • @TAWFEKHPRODTVHD
    @TAWFEKHPRODTVHD 3 года назад +252

    NDAYSANE DIADEFF YALA NA LA YALLA FAYE BARKI S.TOUBA

  • @moustaphasyjr2581
    @moustaphasyjr2581 3 года назад +92

    Ana kou dacor ni xalat tv dougn soss lougn wakh dafa lér dieureudieuf xalat tv♥️♥️♥️✓✓✓✓

  • @ngonedieng7755
    @ngonedieng7755 3 года назад +22

    اللهم اغفر له وارحمه ونقه من الذنوب والخطايا كما ينقى الثوب الأبيض من الدنس واغسله بالماء والثلج والبرد وادخله الجنة مع النبيين والصديقين والشهداء والصالحين

  • @khalilniang1546
    @khalilniang1546 3 года назад +66

    Machalla kou beuege Serigne Touba rek beusal j'aime

  • @tamsirsene8119
    @tamsirsene8119 3 года назад +124

    Dama took RUclips dii Xaar vidéo Bii.... Serigne Atou Yal'ako Yall'a Yërëm tér XarékO aja'''na
    Mercii bien encore une fois XALAAT TV

  • @khadijasene693
    @khadijasene693 3 года назад +41

    Paix à son âme 🤲si tu aimes serigne touba tape j j'aime 👍

  • @chekoulkhadiimbadiane5460
    @chekoulkhadiimbadiane5460 3 года назад +72

    Xalat Man Limay ngiàn thi barké Mohamed môy ngen am.radio.am.television.ndax yen ték la gis ngen Di wax Lou amal réwmi ngiaring ta andoul Aki nàx j'aime wày

  • @firdawsiasrar
    @firdawsiasrar 3 года назад +63

    Fatiha 11 lihlas yénéko serigne Atou diange ak mbolém dioulit yépou niane yalla dolli léne yeurmandé

  • @momodiagne6919
    @momodiagne6919 3 года назад +16

    Yalla nanu yalla Fayal Baye Atou Diagne si barké kou Tédd ki💔💔🙏🏿🙏🏿

  • @serignemortadalobromekross7366
    @serignemortadalobromekross7366 3 года назад +146

    Première commentaire mangui niane képpou kou beug serigne touba rék na nianal atou

  • @info-action6373
    @info-action6373 3 года назад +86

    La valeur d'un homme ne se mesure pas à son argent, son statut ou ses possessions. La valeur d'un homme réside dans sa personnalité, sa sagesse, sa créativité, son courage, son indépendance et sa maturité.
    Un homme multidimensionnel et d'une noblesse incontestable !
    QU'ALLAH t'accueille dans son paradis !
    Merci XALAAT TV !!!

  • @bbthiam8523
    @bbthiam8523 3 года назад +8

    Ma shaa Allah lii yeup si liguey sans tambours ni trompettes. Qu'Allah te fasse Miséricorde Baye Atou. Un exemple pour la jeunesse

  • @mamadoulamine7829
    @mamadoulamine7829 3 года назад +47

    FRANCHEMENT J'ATTENDAIS CETTE VIDÉO ET CELA PROUVE VRAIMENT VOTRE PROFESSIONNALISME VOUS NOUS RENDEZ FIER QUE DIEU VOUS GARDE EN PAIX

  • @keurfafatv
    @keurfafatv 3 года назад +43

    Kou bague srg touba basal j'aime ta yalla tax ❤❤🤙🤝

  • @mouhagng6450
    @mouhagng6450 2 года назад +1

    Machallah tawféhou Serigne bi rek

  • @cheikhdieng4765
    @cheikhdieng4765 3 года назад +42

    Avant de regarder la vidéo je commence d’abord par te remercier d’avoir répondu à notre demande ! Ça montre à quel point la chaîne est engagée au côté des vrais patriotes ! Merci merci merci

  • @cheikhsourang6012
    @cheikhsourang6012 3 года назад +34

    Beug Serigne Touba të yalla takh, mo dakh adina! ak lisibiram

  • @fatmandiaye4225
    @fatmandiaye4225 2 года назад +1

    Merci xallat TV ❤️❤️❤️❤️ xalaat TV 💪💪💪💪 xalaat TV encore xallat TV toujours xallat TV je vous j'aime beaucoup wallahi

  • @niangelementmalickbaht3619
    @niangelementmalickbaht3619 3 года назад +72

    Ohh xalat wallahi lazi dama guiss video bi dm dioy barkep Arkhone dama xallatt magui Niane si barkép xassida Yii barkép s..Touba Yallah nala brom ba faye yiw sm xoul sédna wallahi😭😭😭😭😭❤❤😍🙏

  • @ibn_el_bachir
    @ibn_el_bachir 3 года назад +56

    Jaambari SËRIÑ TUUBA ji
    Jëwriñ: Sëriñ atou diagne
    YALLAH na sunu borom yook ñeggalam si moom
    Teee waneileku ak Sopém ba
    SEXX AHMADU BAMBA XADIIM RASSOUL 🤲🏼♥️

  • @mamediarraboussondiaye769
    @mamediarraboussondiaye769 3 года назад

    Masha'allah alhamdoulillah yallah nala cheikhoul khadim terou firdawsi si barkei mame salihou barkei serigne Abdou lahad mbacké masha'allah xol toy na si sa warhioup ligueye wantei yite xol sede na masha'allah.
    Yallah nala yallah soutoural.
    Sougn njabote gui gneuw euleuk yallah nagn dajekk deugui mourides aki deugui kilifas nguirr mena defarou si adouna bou jaxasso bi🙏🤲

  • @moussasarr4223
    @moussasarr4223 3 года назад +50

    Kou beugg xalaat bessal j’aime 👍🏾 mashalla

  • @bambadiouf9546
    @bambadiouf9546 3 года назад +46

    Kou am dara dja kou amon talibés legueyal seringue touba rek thi la masa nek yalna kou yalla yeram b s touba👈

  • @cheikhfall1606
    @cheikhfall1606 3 года назад +14

    Thiey Serigne touba wallahi amoul morom ❤️Serigne Atou Diagne liguéye Bi rafait lol yalnala yallah Faye thi bar khép Serigne touba ❤️

  • @khacimecisse9304
    @khacimecisse9304 3 года назад +19

    Mais wa Xalaat tv mom khana ab nitou yallah nga mashallah ❤💗say cadou day lerr andak yarr akii Tèguine yallah nala sougnou borom Sameu wayyy💓💖

    • @habibdiakhate5691
      @habibdiakhate5691 3 года назад +1

      Machallah amiine

    • @khadimkante9783
      @khadimkante9783 3 года назад +2

      Bilay machalla way

    • @elhadjifallousarr3467
      @elhadjifallousarr3467 3 года назад

      Wallahi xalaat tv lii gay défal Sénégalais yi boo faato (yalla na yèx) waayé dootun la fatté ba muk.
      Ndax lèrna ma ni na foo fété ci keur dîné yi Wayé fègnul ci vidéo yi dax képu kou bax ga indiko guir gnu diarignou
      Dagay wax deugu ta doo par par lo
      Di bènalé askanwi
      Di wèr nafèkh yi ak sath yi
      Yalla na la yalla faye

  • @khadimsamb3040
    @khadimsamb3040 3 года назад +17

    Sëriñ Atou Diagne ndanane deug mouride sadikh leu liguéyeul na yalla ba dém té dara niawoul.
    Yalla nako yalla yeureum ta kharé ko aldiana firdaws

  • @bayesalioufall7838
    @bayesalioufall7838 3 года назад +2

    Serigne atou Diange yalla nako yalla yeurem thi barkep serigne touba ak khassida yi

  • @salioufam3247
    @salioufam3247 3 года назад +76

    Enfin je suis le premier à commenter sur xalaat wayyy😂😀 ndeysaane le dieuwrine des dieuwrines S Atou Serigne Touba dinala fayy bagua tiiit walahi

  • @TAARU_AHLOULAHI
    @TAARU_AHLOULAHI 3 года назад +47

    L'accueil dans son paradis céleste 🤲

    • @thiamadiao8243
      @thiamadiao8243 3 года назад +1

      ❤️❤️❤️❤️💯👌👌👌

    • @maremefaye4410
      @maremefaye4410 3 года назад

      ALLAHOUMMA AMIIIN ❤🙏🤲

    • @tima8577
      @tima8577 3 года назад

      En terme de kham kham technique charisme....Yalla na khippé aldiana firdawss

    • @badarakane2084
      @badarakane2084 3 года назад

      machallah

    • @TAARU_AHLOULAHI
      @TAARU_AHLOULAHI 3 года назад

      Amine 🤲🤲

  • @taphadiange4096
    @taphadiange4096 2 года назад +1

    Ndaysane machallah 🥰🥰🥰

  • @LaChaineoff
    @LaChaineoff 3 года назад +41

    Mon père était le chauffeur quand ils allaient chez Serigne Aboudoul Ahat MBACKÉ en 1972 j’ai même les archives avec moi. A l’époque c’était le "Dahira des Étudiants"

    • @charlesguy6061
      @charlesguy6061 3 года назад +1

      Ton pere n'etait il pas chauffeur au coud?

    • @LaChaineoff
      @LaChaineoff 3 года назад +2

      Charles Guy si il était chauffeur au COUD et même mon frère travaille aussi là-bas comme chauffeur

    • @sokhnaaminatasaw8445
      @sokhnaaminatasaw8445 3 года назад +2

      Mashalla 🙏🏼

    • @tmoustapha807
      @tmoustapha807 Год назад +1

      Segn bi niogui ziar😢

  • @djilyabdoukhadre501
    @djilyabdoukhadre501 3 года назад +34

    Yalna noko Serigne Touba térou🥰😭

  • @mouhameddjigal760
    @mouhameddjigal760 3 года назад +1

    Yalla nayalla yeureum serigne atou diagne

  • @serignesammbayeserignesamm8694
    @serignesammbayeserignesamm8694 3 года назад +20

    Ndeyesan 😭😭😭😭😭 thiey adduna kou diambar lool Baye atou Diagne yalla nako yalla yeureum ta kharé ko aldiana firdawsi barké Serigne bi

  • @khaliltv5781
    @khaliltv5781 3 года назад +18

    Thiey Segn ATOU yalna ko san borom dolli yërmandé 🙏

  • @mbayeniang8404
    @mbayeniang8404 3 года назад +4

    Dieuredieuf serigne atou diagne khasayit mission accomplie paix à son âme 😭😭😭😭et xalaat tv machalla thji leral yii

  • @Talibe_Bamba.4
    @Talibe_Bamba.4 3 года назад +19

    Liguey bii rafett na mission accomplie yalnako yalla yeureum borom touba terrou cia aldianay firdawsii ❤️🥺🙏🏾

  • @momofall5093
    @momofall5093 3 года назад +28

    Dieureudieufe serigne touba yallah nako yallah yeureum te xareko aldiana barke s touba 🙏

  • @codoudiop9905
    @codoudiop9905 3 года назад +33

    Ce qui me plaie plus c le faite de nous aidez à supprimé le mot "Complexe" yalla na tassék yeurmadé borom bi barké Borom Touba

  • @mamemamo
    @mamemamo 3 года назад +59

    Ki mourid sadikh la nagnou ko yalla fayal te xare ko al diana😭🙏

  • @ndiawarsarr9952
    @ndiawarsarr9952 3 года назад +17

    Machallah vraiment à xalaat TV toujours au service de la nation baye Atou Diagne k votre âme demeure au Paradis céleste...

  • @PorokhaneMameDiarra
    @PorokhaneMameDiarra 3 года назад +17

    Yalla yalla wanalèko ak kou téd ki thia aljana firdawsiya si barkép seydina mouhamed. Amine

  • @chiekhmourtadambayewakaana1859
    @chiekhmourtadambayewakaana1859 3 года назад +6

    Walahi nou gnou mél moma man ak samy morom you bari Serigne atou yalla nala serigne bi térou amine 😭😭😭😭

  • @mouhamedmbacke7026
    @mouhamedmbacke7026 3 года назад +5

    Maasàllaa ❤️❤️ Amna solo lool, yal na Yàlla yeesal yërmaandeem barkeb Alxuraan.

  • @mathiouz2074
    @mathiouz2074 3 года назад

    Serigne Atou Diagne yalana Yallah waccé yërmandé ak njéggël ci mom tabbal ko Al Janna Firdaws bi Barakati SEYDINA MOUHAMMADOU RASSOULOU LAAHI SALLA LAAHOU ALEYHI WA SALAM

  • @Dame.diagne
    @Dame.diagne 3 года назад +12

    Magui koy tibè thi sama xol ak ak s.touba 1millions de vue la beug thi vidéo bi yalla nako thi am wakhal amiiiiin

  • @makhtarsylla1684
    @makhtarsylla1684 3 года назад +4

    اللهم اغفر له وارحمه وعافه واعف عنه ووسع مدخله واكرم نزله ونقه من الذنوب والخطايا كما ينقى الثوب الأبيض من الدنس وادخلها الجنة واجعلها من جوار رسول الله صلى الله عليه وسلم ءامين

  • @madiorfall7069
    @madiorfall7069 3 года назад +8

    Dieureudieuf xalaat tv . Vraiment merci 😭😭😭❤❤

  • @serignecheikhounambacke9981
    @serignecheikhounambacke9981 3 года назад +7

    S atou diange yalnako yalla dollé yeuram te diegalko mbolém bakaram yépou thi barkéb kimou done leugéyal

  • @serignembacke367
    @serignembacke367 3 года назад +19

    Serigne atou diagne daye kene si Sénégal 😭😭❤❤❤❤

  • @Real4peace
    @Real4peace 3 года назад +11

    un vrai Général de Bamba que le tout puissant l'accueille dans son paradis céleste 🤲🏾

  • @laylabatoulthiamniass4884
    @laylabatoulthiamniass4884 3 года назад +11

    Machallah yalna yalla yésal yeurma'dém yarabi man lii mo takh ma beugg mourid yi danio.am foula doun kharr éta machallah seuring bi sa ligéy rafattna tropp ♥️♥️

  • @aminatafall8264
    @aminatafall8264 3 года назад +5

    MachaAllah Yallah na sounou borom khaaré ko aldiana firdawsi ya gueneu kawé si barké Naby Moustapha

  • @joop-saliou-kebemer22
    @joop-saliou-kebemer22 2 года назад +2

    Yallana yalla yeureum ko khareko aldiana firdowsi

  • @mamemorantasaly794
    @mamemorantasaly794 3 года назад +19

    Que Firdawsi soit sa demeure éternelle, amine. 🤲

  • @cheikhndiaye16591
    @cheikhndiaye16591 3 года назад +7

    MachAllah. K le firdawsi soit sa demeure éternelle

  • @dieuredjefeborometouba
    @dieuredjefeborometouba 3 года назад

    Machallah.Serigne Atou Yalla n'a ko Sounou Borome defaal khéweule adina ak alahira bakê alkhourane,

  • @LLTV43
    @LLTV43 3 года назад +14

    Jàmbaar dégg demna Sëñ Aatu Jaañ yal na Yàlla dolli yërmaande ci moom ci barkeb Xasida yi 🙏🏾 😭

  • @bijoubangoura1028
    @bijoubangoura1028 3 года назад +10

    Machalah seringe Atou diange yalla nako seringe Touba téro diambar Lawone ko nangou sone si Ligeuyal seringe Touba Aldianay firdawsi yalla na done keurame merci khalate tv yalla na sa diame yage

  • @santeboromtouba3482
    @santeboromtouba3482 2 года назад +1

    Amna solo trop ndaye san yalna ko sarign touba tèrou

  • @npm7576
    @npm7576 3 года назад +8

    Masha'alLah doy nga idoLe béep juLiit YalLah na La buur YalLah fay LiguéYeuL diné rek mo woor 🥰 dama beug wa hizbou borom bi xamna ko

  • @badarakane2084
    @badarakane2084 3 года назад +7

    xalaat tv machallah sén liguye rafét na torop yalla nalén yalla faye barkéb s touba machallah way ❤❤❤❤👏👏👏👏👏

  • @bayesalioufall7838
    @bayesalioufall7838 3 года назад +2

    Ndeye sane thiéy serigne touba amoul morom deh billhai yalla naniou ko yalla fayall

  • @beugbamba9487
    @beugbamba9487 3 года назад +105

    Barke XASSIDAYI sama xoll sedd na loll yallna yalla taxawou XALAAT TV😪😪

  • @thiernombaye6472
    @thiernombaye6472 3 года назад +22

    yallna ko yalla yereum mandé bouma sétané sa vidéo ba paré 3 salah toultoul fahtia dila gnanal.🤲

  • @mamethiernofaye420
    @mamethiernofaye420 3 года назад +1

    Akassa amna solo lool
    Baye Diagne, il ne cessera de marquer les générations.
    Boku na si louma diap si ay wakham moy bouniou begué souniou liberté faw niou meneul souniou bop; « sans autonomie financière, on ne peut acquérir une indépendance culturelle » nitt kilay diokh mola sagn diokhogn foy takhawé.
    Lolu ma gné si lool Hizbut yi nakh lolu la Serigne bi dane incarné. Sokhlaloul lene si kene rawatina bour yi à l’époque

  • @morbapttmoms2411
    @morbapttmoms2411 3 года назад +18

    Xalat tv gueuna la beugue barké xasida yi😭❤❤❤

  • @Footplus221
    @Footplus221 3 года назад +30

    Xalat tv le meilleur qui est d'accord👍👍et abonne toi😙

  • @manemiwaawaw669
    @manemiwaawaw669 3 года назад +1

    WA HT AY TANÈFI S.TOUBA LAGNIOU💔💗💘💞💔💓💟

  • @bocargueye238
    @bocargueye238 3 года назад +21

    Yalnako yalla yeureum, dieguel ko té kharéko aldiana firdaws 🙏🙏🙏

  • @serignembayefall7897
    @serignembayefall7897 3 года назад +19

    Serigne Atou yalla nako yalla téral si barke serigne touba ak xassida yi

  • @aliounebadaralo7036
    @aliounebadaralo7036 3 года назад

    Man dei barkei Serigne Touba niéé nako ko xamni sa dounde guépp si liguèyeul Kou teddki nga ko deff ba wathi liguèye yalneu sune brom wathié yeurmandei si kawam barkep khassidayi.
    Merci Xalaat TV liguèye bi rafeitneu!

  • @Ibnusenfitness24
    @Ibnusenfitness24 3 года назад +8

    Serigne Atou Diagne paix à son âme 🤲🏽gracias a ustedes ✊🏽

  • @serignetakkricain6473
    @serignetakkricain6473 3 года назад +30

    Ndayesan 🤦‍♂️❤️ligueye rek ladon def bilaye
    Merci xalaat tv ❤️✊🏿

  • @madamewade4638
    @madamewade4638 3 года назад +1

    Mashallah

  • @MbeneSaliou
    @MbeneSaliou 3 года назад +13

    MACHALLAH XALAAT SERIGNE ATOU YALNA KO YALLA YEUREM SERIGNE TOUBA TÉROUL KO BOBAM

  • @mathiou68
    @mathiou68 3 года назад +65

    C'était lui le vrais général de Bamba.
    Que Dieu l'accueille dans son paradis céleste firdaws

  • @serignecheikhndiayekheweul6145
    @serignecheikhndiayekheweul6145 3 года назад +1

    Yal na ko Yàlla jéggal te yërëm ko barkeb Seexul Xadiim aamiin

  • @medzombp7117
    @medzombp7117 3 года назад +6

    ✍✍✍✍yalla na ko yalla khare aldiana ya gueuna kawè si barkep serigne touba🕋🙌❤

  • @vipf4116
    @vipf4116 3 года назад +7

    Machallah amna solou trop..♥️♥️🙏

  • @bassiroufall4719
    @bassiroufall4719 3 года назад +6

    Yalna yalla faye serigne atou Diagne te kharéko al diana firdawsi 🤲🤲
    Et merci beaucoup à xalaat tv la de homme des valeurs

  • @mitafall1943
    @mitafall1943 3 года назад +4

    Yalla nako yalla yreum té kharéko adiana firdawsi barkep naby Moustapha psl ❤️🙏🏿

  • @abdoulahisalih600
    @abdoulahisalih600 3 года назад +33

    QU'ALLAH LE TOUT PUISSANT L'ACCUEIL DANS SON PARADIS BARKEP BOROM TOUBA AK XAÇIDA YII
    BAYE ATOU JËRËJËF❤️❤️❤️

  • @lahaddiouf4038
    @lahaddiouf4038 2 года назад +1

    Machallah

  • @abomadiyanalo9034
    @abomadiyanalo9034 3 года назад +13

    Ndaysaan jàmbaar dëgg mooy jëmm jii yal na ko Yàlla yërëm te jéggal ko.

  • @moustaphaniang2652
    @moustaphaniang2652 3 года назад +57

    Mane lima nekh si chaine bi moy
    Danu respecter niit gni nakh dounu tanxam lou abonnés yi demb rek la ame kouko commenter yalna yalla fayal nou lène si barké alkhourane 😢😢

    • @daradjitv8678
      @daradjitv8678 3 года назад +2

      Bilahi kay 😭😭 mom ladon beugue wakh ngawakh

  • @khadimegueye5540
    @khadimegueye5540 2 года назад +1

    Machalla ❤️

  • @mboupkhassim138
    @mboupkhassim138 3 года назад +14

    Vraiment XALAAT TV yalna la yalla faye yiiw ak fane wou goudou ak were gi yaram SA ligueye raféte trop ta am solo

  • @fashionmoonsonn
    @fashionmoonsonn 3 года назад +11

    Machalla Mame Ato Diagne Sa Dondou Gui Amoune n’a Solo Yallah N’a aldiana disa keur

  • @pvpvseck9078
    @pvpvseck9078 3 года назад +1

    Seriñ Atou Diagne yalna Aldjana done sa keur si barkeep Seriñ Touba 🙏🏾

  • @aliounesow899
    @aliounesow899 3 года назад +19

    Yalna diameu yague cii rewmii🙏Serigne Atou yalnako yalla yeureum té diégueul ko té fayal gnouko🙏🙏🙏🙏
    Xalaat Tv thia kaw thia Kaname machalah liguey bii rafett neu🙏🙏🙏🙏🙏

  • @bayeousseynoufallkhataba7361
    @bayeousseynoufallkhataba7361 3 года назад +5

    Machallah amatina solo Dieureudieufetii Serigne Atou diagne mouride sadikh bii Yalla nacko sunu borom yeureume tee khareckoo thiaa al dianna you maag yaa sii barckee borom touba khassaide yii amiine❤🙏

  • @moulague1075
    @moulague1075 3 года назад

    Qu'Allah Soubhana Wa Taallah l'accueille dans son paradis celeste liguéyeul yalla rek mo wor et il a fait en prenant Cheikhoul Khadim comme son modél repose toi grand messieur je ne saurais terminé sans vous encourager et vous remercier pour tout ce que vous faites pour le réveil des consciences vous de XALAAT TV Dieuredieuf guéne

  • @mohamedoulmoustaphabarhama9702
    @mohamedoulmoustaphabarhama9702 3 года назад +14

    Que son âme repose en paix et que Firdawsi soit sa demeure éternelle si barké Seydina Mohamed(SAWS)🤲🏽