ah fall kone dei gno bokou beug beug s sam mome damako sopou lol.hier rk mangui nafilas sama xél déme si mome walahi ma diangalko * wal hassri* ndah beugone nako lool.waxtanam you bari mome lakoy oubé.
Si on pouvait aimer une vidéo 10000 fois je passerai la journée à aimer ce vidéo, je ne trouve pas les mots pour magnifier votre remarquable travail. Mais je prie le bon Dieu qu'il vous protège éternellement Xalaat👍
Serigne Sam bimouy gnibi j'avais que 1 an tei mom motakh ma mbourou di soll lou diote limou def si mane 😭😭damako beug tellement soumay wadj neilaw sakh mom lay deg lou
*Poème pour BAYE SAM* Si la sagesse était une de ces étoiles Serigne Sam l'aurait sans doute attrapée Il chercha sa vie durant à lever les voiles Sur les mystères, essences des réalités Quel abîme de sciences, il est épris de bien Il raviva les consciences, au profit des siens Il aspira à la béatitude sublime Par pur soufisme, vers les très élevées cimes Il nous enseignait usant d'une creuse rhétorique Toutes ces connaissances qui nous seront bénéfiques Il brossa des tableaux clairs des hagiographies Des hommes de Dieu, précurseurs d'illuminées philosophies Ses talents surpassaient de loin toute ambition Car gardait des joyaux de divers horizons Mais Baye Sam retourna vers le Majestueux Ah! Lui qui recommandait d’être bien et pieux Vœux alors qu'il séjourne et éternellement Dans les jardins paradisiaque, comme agrément. AMINE Amadou Bamba NDOYE
Je suis vraiment admirative devant ce grand homme. Qu'Allah l'accueille au paradis firdaws. J'espère que les jeunes sénégalais prendront exemple. Diar diar bou Rafet masha Allah ❤️❤️❤️🙏
Maasou ma commenté waye taye. Mom sama wadji diaral nama ko Macha allah serigne. Sam Mbaye harifou billahi bi Serigne Sam Mbaye. Waliyou lahi Serigne Sam Mbaye borom Xam Xam bou yatou bi dessé loo niou sara thi xam xam Daana wakhtane banane boudoul wonak yenate dinane fi wakh xam xam bou yemé dana wakh ba nane. Bari na loo kham ni deug la te souma len ko wakhon dou nguen ko geum te kou tek Safara ma waate dougal thi sama lokho ni deug la. Dana wakh nane bari na thi xam xam lo kham ni douma len ko wakh nakh kon dounguen ko geum walla douguen xam fou nguen koye tek Dana wakh nane mourid yi li niouy beug beug Serigne Touba am na lo Xam ni douma len ko thi wakh ndakh dou nguen xam fou nguen koye tek.... Linou mana wakh thi mom bari na wallahi wayé doune ko mane ndakh mbecté Salaw taye sama khom bi dafa seed tr lira gouma video bi
J'ai fait une expérience: prendre les questions qu'on posait à Serigne Sam Mbaye jadis et je les ai posé à des oustaz et certains borom xam xam connus de no jours mais je vous jure personne n'a été capable de me répondre aussi clairement et avec pertinence que Baye Sam. Pour vous dire Serigne Sam amoul mass si xam xam
Xalaat t v 🙏🏾 yene yeney senegal merciii 🙏🏾❤️ mane talib cheikh tidine la me seringe sam mbay dafa ame xam xam lole yala nangouco yala fayale te khareco aldjana🙏🏾😭😭😭🙏🏾❤️
Ndeyesann s Sam dh kouko beugue kham kane moy Yalla deug louko mane dh mourit la mais kepp ko khamni Yalla Def la diokh xam xam di diangua le kom s same walla imam assane cisse walla oustage ady niass walla s abdou rafahi mbacke walla niol toufa khale Bou beugue kham sa dinne nagualen deugg lou
MachaAllah sama Serigne sama Wassila mo féss sama khol Diambari l'Islam YALLAH na YALLAH yok léram té tass gnou ci barkém 🙏merci Xalaat tv contane na trop kou beug Baay Sam rék ma beug la💝
*Un des Références les plus Rares du Sénégal 🥺* *Rare na gni melni mom si sounou Diamono Dji ndax Heure boy deglou waxtanam Yalla ak Yonnet bi ngassiy gueneu degg kom nika Mamam Ahmadou daan defei 🙏🏾❤️* *Yalla nako Yalla fay ndax ba legui foko deglo mou dello sila si Sounou brom 🥺🥺🥺*
Nit yi khamnagnko té nioguiciy diarignou ,dafa fekni sougn réwmi key nitou YALLA yi lagn tégoul féneu,fo kate yi dal laniouy promouvoir. Serigne Sam nak mom exception leu il a fait sa promotion tout seul et avec l'aide de DIEU. Bamou dmé yagg neu té batay niouguikay deglou mouy traité ay thèmes d'actualité. Yalnako YALLA doli aw yiw
Xalate je prends ceci en témoin En 2013 mes parents on eut un des conflits conjugale lorsque on m'a appelé je suis venu ce jour retrouvant le calme dans la concession cependant j'ai remis à mon père mon MP3 le conférences de Serigne Sam Mbaye RTA il a pleuré sur le coup et dit à mère que de l'excuser et depuis lors la paix nous a visité et y reste à vie Yalla n'a borome bi Gueureme
Je suis fière de toi Bou niép don def kom xalat tv légui jeunes bi niépou yéwou kou begue xalat tv yague fi ta andd ak weer gui yaram beuseul j'aime ana niy sopou Serigne sam mbaye je t'aime
Jërëjëff xalaat tv amna solo lool Man kii motakh ma jël yoon bubaax bi di jaamu yalla wallahi Te ay waxtanam rek ladan deglou Yalnanou ko yalla Fayal barkeb Alxuraane
Sëriñ Saam Bokk na na ci nit yi ëppu solo ëppu ñariñ ci àddina Mayalna sëkk mission wam ci kaw suuf Yàl na ko sunu boroom dolli yërmaande famu nekk barkeb Seexul Xadiim ❤️ Jërajëfati Xalaat Tv liggéey bi rafet na na Yàlla dolli la taxawu🙏🏼
Ndaysan yéna bakh wayy man dh chaque première dimanche du mois de Ramadan dagni dém Louga départ Dakar 5h du matin agg ay 11h inchallah ziaré tawou s Sahm mame chaikh Mbay diouli tisbar weur deuk bi dem parlait djili mbay ak fi S Sahm done déff khoudba juste takousane djiot gniou djoli dieul départ ndogo tiwawone djouli guée départ 22 h fékeu gniou Dakar machallah khalat contane na dh
C l seule personne que j’écoute H24 tout le monde doit prendre exemple sur lui et réapprendre sur lui enseigner ses œuvres et leçon walahi legui Sénégal 🇸🇳 nekh
Machallah xalaat TV Sénégal manoul amat kou Mel ni yawf❤️❤️❤️❤️ ndakh lingay def rafet na trop man mom Bouma la guisoon dina la nèkhal billakhi ❤️❤️❤️❤️
Ndeyesan 😭 tey mom lall ngama dei Sama sopé bi beugg koo lool ndeyesan yalla nala Serigne bi fay Baye Sam kou mata bayi xell la don jambar lool sii diné rawatina yonou mourid xam thi mom Lou bari ndeyesan leu 16 bii thila ame dom moy Sama tawe mom lako toudé sakh Sama xoll sedd na trop thi lii yalla nako yalla doli lerr xalaat TV beugg nala lool nguir linga deff thi Baye Sam nguir nitt gni xam ko Kend Manou ko xam sakh wayé nguir xam thi mom tuti ndeyesan Dieureudieufe
Machalah sen liguey amna solo trop yenangui yée khaleyi ak niou beuri niou done nelaw , Mokham ci ndiagalé mak gni la wala souniou bagn katt yi toubab yi sakalone pekhé. Gueum sa bopp rekk moo woor. Yalla na léne yalla samm
Alhamdoulilhahi Rabil alamina a travers le nombre de personnes ki ont aimé et commenté cette vidéo je me rend compte que la jeunesse et autres sont entrain d'écouter baay saam magui sogne sama bop ak niep nioukoy deglou sasouné cone diga raw say mass mom da wakhone tamit né diamono gui niew coumou nekh coumou nakhari sama cassette yi niofiy doon ckeikhou tarbiya niofiy doon cheikhou tarkhiya merci baay saam.
C'est la première fois que je regarde une vidéo du début à la fin... Merci Bcp xalaat Tv. Vous avez la responsabilité de montrer aux jeunes qu'on a rien à envier aux autres nations... S Sam était extraordinaire, Yalla dako dimbali. Il mémorisait tout ce qu'il lisait....Ya d'ailleurs son fils qui est sur ses pas machallah. BRAVOOO ET MERCIII A XALAAT TV. Dimbalil jeunesse bi rek thi wane leen borom xam xam yi nga xamni sén jikko, sén yarr ak téguinn rafett na.
j'ai jamais commenté...je le fait aujrd'8 parce que je suis content de xalat tv... depuis que j'ai commencé à vous suivre vs m'avez jamais déçu ...vus que les gens publient slmt pour de l'argent ...vs êtes les meilleurs
1ère fois ma commentaire parceque dagno wakh si nite kouma beug diko téwlou BAYE SAM MBAYE yalla na yalla yokk ay léram
@@khadimdiakhate2824 inshallah en tt cas xalate mom douma rater ay vidéos wam
Amine
Machallah
Amoule won morome barker s touba car mome lomou wakh yalla takh
ah fall kone dei gno bokou beug beug s sam mome damako sopou lol.hier rk mangui nafilas sama xél déme si mome walahi ma diangalko * wal hassri* ndah beugone nako lool.waxtanam you bari mome lakoy oubé.
Si on pouvait aimer une vidéo 10000 fois je passerai la journée à aimer ce vidéo, je ne trouve pas les mots pour magnifier votre remarquable travail. Mais je prie le bon Dieu qu'il vous protège éternellement Xalaat👍
Akassa
Amin yarabi
Moi meme millionnaire fois sakh ma defco
Kou sope serigne sam mbaye beuseul j'aime ❤️🙏
Amna solo trop
Merci
ndeysann yalna yalla yoki leram
Mangui nii deh ❤
Ndaye sane
Suma wasila adina alakhira yalla na niou yalla tass si barkéme keppe kouye sopé Serigne Sam nel Amine 🙏🏾😍🤩🤩❤️❤️❤️
Aminnn
amine
Amine
Amin
Amine yarabi 💕
Serigne Sam bimouy gnibi j'avais que 1 an tei mom motakh ma mbourou di soll lou diote limou def si mane 😭😭damako beug tellement soumay wadj neilaw sakh mom lay deg lou
Machlla
Bilay man mi sakh bima koy kham diogué nafi wayé lou beuri si man ay wkham lakou diangué
@@bayegalayeseye99bayegalaye40 jtjr bokay deig lou dagay geune ragal yalla
Ndeysan waxon nako dh néna sama kasét dina dioubeuntii niitt you barii
Ndeysaan boul ko fatte Di nianal
*Poème pour BAYE SAM*
Si la sagesse était une de ces étoiles
Serigne Sam l'aurait sans doute attrapée
Il chercha sa vie durant à lever les voiles
Sur les mystères, essences des réalités
Quel abîme de sciences, il est épris de bien
Il raviva les consciences, au profit des siens
Il aspira à la béatitude sublime
Par pur soufisme, vers les très élevées cimes
Il nous enseignait usant d'une creuse rhétorique
Toutes ces connaissances qui nous seront bénéfiques
Il brossa des tableaux clairs des hagiographies
Des hommes de Dieu, précurseurs d'illuminées philosophies
Ses talents surpassaient de loin toute ambition
Car gardait des joyaux de divers horizons
Mais Baye Sam retourna vers le Majestueux
Ah! Lui qui recommandait d’être bien et pieux
Vœux alors qu'il séjourne et éternellement
Dans les jardins paradisiaque, comme agrément.
AMINE
Amadou Bamba NDOYE
Machalla
Macha'Allah
Machalla
Mashala
Machaallah je suis vraiment heureux yala xamnako
Le plus grand connaisseur et professeur que le Sénégal n’ait jamais connu
Iaw ligeu oumpeulé beurie neu dh
Walay
Bilay
Vérité
Je suis vraiment admirative devant ce grand homme. Qu'Allah l'accueille au paradis firdaws. J'espère que les jeunes sénégalais prendront exemple. Diar diar bou Rafet masha Allah ❤️❤️❤️🙏
Jajeuff
Allawouma Amine
❤️❤️❤️❤️❤️😭walay ndaysan sama khôl Sedna dieum j serigne same nouma mél guinaw yalla moma defar si déglou rek 😭❤️🙏
Akmane tamit
AKASSSA ak mann
Ndeyesane wallahi baringasi ay morom
Wallay barii ngasi ay morom yalnagnouko yalla fayal
Machalla amna solo loool
Maasou ma commenté waye taye. Mom sama wadji diaral nama ko
Macha allah serigne. Sam Mbaye harifou billahi bi Serigne Sam Mbaye. Waliyou lahi Serigne Sam Mbaye borom Xam Xam bou yatou bi dessé loo niou sara thi xam xam
Daana wakhtane banane boudoul wonak yenate dinane fi wakh xam xam bou yemé dana wakh ba nane. Bari na loo kham ni deug la te souma len ko wakhon dou nguen ko geum te kou tek Safara ma waate dougal thi sama lokho ni deug la.
Dana wakh nane bari na thi xam xam lo kham ni douma len ko wakh nakh kon dounguen ko geum walla douguen xam fou nguen koye tek
Dana wakh nane mourid yi li niouy beug beug Serigne Touba am na lo Xam ni douma len ko thi wakh ndakh dou nguen xam fou nguen koye tek....
Linou mana wakh thi mom bari na wallahi wayé doune ko mane ndakh mbecté
Salaw taye sama khom bi dafa seed tr lira gouma video bi
Ndeyesan
@@serignesammbayeserignesamm8694 machalla
Macha Allah contane nane
Macha Allah contane nane
niapa kou bague bilay seringe sam mbaye 😭😭😭😭❤✋
Sama doom sama taw moom lako toudé. Il a just 2 mois
Mashalla yalla na doundou té barké🥰
Ndaysan masalah yalna topou tanqeu tourandowam
Masha'Allah Yalla dieul djikooy toureundoo wam
Yalla nako yalla same si barke s.saliou
Yallna ko yall barkel
Serigne Sam Mbaye psl fait parti des personnes du monde entier qui m'ont séduit de son enseignement... Il fut et reste une immense bibliothèque.
Bilay
J'ai fait une expérience: prendre les questions qu'on posait à Serigne Sam Mbaye jadis et je les ai posé à des oustaz et certains borom xam xam connus de no jours mais je vous jure personne n'a été capable de me répondre aussi clairement et avec pertinence que Baye Sam. Pour vous dire Serigne Sam amoul mass si xam xam
Bilay
@@galaxiepro.5641 motax malène done natt😁😁
Serigne Sam depuis temps khalé makoy déglou, dèggagouma kouko djégué ci xam-xam, surtout Tassawouf.
Yalla moko khamal billahi Bay Sam dou mass
Xalaat t v 🙏🏾 yene yeney senegal merciii 🙏🏾❤️ mane talib cheikh tidine la me seringe sam mbay dafa ame xam xam lole yala nangouco yala fayale te khareco aldjana🙏🏾😭😭😭🙏🏾❤️
Yawko bakhga
Aminnne
Ndeyesann s Sam dh kouko beugue kham kane moy Yalla deug louko mane dh mourit la mais kepp ko khamni Yalla Def la diokh xam xam di diangua le kom s same walla imam assane cisse walla oustage ady niass walla s abdou rafahi mbacke walla niol toufa khale Bou beugue kham sa dinne nagualen deugg lou
MachaAllah sama Serigne sama Wassila mo féss sama khol Diambari l'Islam YALLAH na YALLAH yok léram té tass gnou ci barkém 🙏merci Xalaat tv contane na trop kou beug Baay Sam rék ma beug la💝
Bilahi
Yagui nc
@@sidybarrafall5429 MachaAllah
Amoul kén koumay déglu koudul mom
Waliyou la Dieureu dieuf Baye Serigne Sam Mbaye 🥰🥰
Jajeuf
Jajeuf
Bariiii ngasi ay morom
Merci
L'homme qui à travers ces sermons galvaude l'âme des personnes qui le suivent. Un imminent pédagogue dans tous les plans .
Tay la thi masa comanter ndakh dieum ji ak lim def thi man ta masou mako guis magui yalwal yalla mou yeureum ko ta diegal ko ta dolli ko ay khéwal
@@cheikhgaye427bu
Aminnne
Machallah notre chaîne xalat tv,mais gniy dislike esk ay dioulite lagnou ??
Walay walay produit de Bamba way xalat
Beusseulènma j’aime 👍 way
Jajeuff
Ki dou produit kéne
Machallah mome la guiss senegal nieupeuko meuneu deglou Tidiane layene niassene mouride....yalla nakko yalla teral barké seydina mouhamed anleyhi salatou wa salam
Nitkou séll Mogui ni féss ak xam xam billahi sama xoll mo sédd ❤️❤️🇸🇳 Yalla Nanou yalla tass si barkém yalla guisélé Diou ak môme🤲🤲🤲❤️❤️
Aminnn
*Un des Références les plus Rares du Sénégal 🥺*
*Rare na gni melni mom si sounou Diamono Dji ndax Heure boy deglou waxtanam Yalla ak Yonnet bi ngassiy gueneu degg kom nika Mamam Ahmadou daan defei 🙏🏾❤️*
*Yalla nako Yalla fay ndax ba legui foko deglo mou dello sila si Sounou brom 🥺🥺🥺*
Nice na de we gained di
Ki dém ta nék fi ba légui❤
رحمة الله عليه😥😭
Walakhi❤️
Walahi
Lolou moy dondou ba faw
Ndaysaan moom de nekk nafi ba joge fi te nit ñi xamuñu ko yal na yàlla yokk ay leeram te taas nu ci barkeem❤️🤲🏾🥰🥰
Mdrrr khana yako khamoul
Amine yarabie 🙏
Nit yi khamnagnko té nioguiciy diarignou ,dafa fekni sougn réwmi key nitou YALLA yi lagn tégoul féneu,fo kate yi dal laniouy promouvoir. Serigne Sam nak mom exception leu il a fait sa promotion tout seul et avec l'aide de DIEU. Bamou dmé yagg neu té batay niouguikay deglou mouy traité ay thèmes d'actualité. Yalnako YALLA doli aw yiw
ماشاءالله
Xalate je prends ceci en témoin
En 2013 mes parents on eut un des conflits conjugale lorsque on m'a appelé je suis venu ce jour retrouvant le calme dans la concession cependant j'ai remis à mon père mon MP3 le conférences de Serigne Sam Mbaye RTA il a pleuré sur le coup et dit à mère que de l'excuser et depuis lors la paix nous a visité et y reste à vie
Yalla n'a borome bi Gueureme
machallah
Mon exemple, l'homme qui m'a inspiré et à qui je dois mon aspiration... Si j'aime le savoir tant c à qlq part grâce à lui. Yalna ko yalla guërëm
Akassaa
Aminnnnn
Je suis fière de toi Bou niép don def kom xalat tv légui jeunes bi niépou yéwou kou begue xalat tv yague fi ta andd ak weer gui yaram beuseul j'aime ana niy sopou Serigne sam mbaye je t'aime
Bilayy
@@tafakara1123 merci beaucoup frères
MERCI
MaCh Allah Waye
Damako done dègg rek ndeydane
Amna solo.
Machallah
Un homme multidimensionnel.
Un homme de sciences,
Wallahi ndeysane ki guindi na niou barii yalla nako yalla yeureum kharé Aldiana Firdawsy ❤
Bilahi xalate yangui liguéy lou am solo❤ que Dieu vous protège🤲
Amennnn
Ohhh🤦🏿♂️💕❤billahi limay yekk sama xoll nii manou mako bind kou jeunesse bi wara xam th diko deglou💕🥰merci encore xalaat TV❤❤❤
dou yaw rek
Nice🙏🙏🤲🤲
Beug Yallah ak Beug Xam Xam rék mô waral sén commentaires yi... Yalna lén Yallah Défal diam ak Salaam barké Moustapha anleyhi wa salaam! Amine
Aminnn
*Vidéo bi man nga ko défal* 😭🙏🇸🇳❤️
Bilay
Képpou kou beug seringe Sam Mbaye reik nga abonné wou Sama sén
Mâcha Alah ❤️❤️❤️❤️
Machalla
Yalna yalla YOKK ay leram thi BARKÉB BROM Touba 😍
Aminnne
Franchement #xalaat tay mom lal nga sama xoll❤️❤️❤️رضي الله عنه
Jërëjëff xalaat tv amna solo lool
Man kii motakh ma jël yoon bubaax bi di jaamu yalla wallahi
Te ay waxtanam rek ladan deglou
Yalnanou ko yalla Fayal barkeb Alxuraane
Yaa ngi wakh taané kouma beugue 😭😭😭 ndeye saan baye Sam yalla na yalla yokou aye léeram si barke s TOUBA
Doma thi dap wallahi
Sa bop gua ham..
@@mouhamedthiam9048 ndeye saan
Wakh tanam si bopam mo nekh mane doumassi doyal
@@fatoufaye4620 baye sam dafa yéeme bilakhi 😭😭
Serigne sam mbaye yalna yalla yok léram🙏🙏🙏❤
Mersi xalat
Serigne sam mbaye yalla nano ku yalla fayal ci barkem xassida yi amin amin
Sëriñ Saam Bokk na na ci nit yi ëppu solo ëppu ñariñ ci àddina
Mayalna sëkk mission wam ci kaw suuf
Yàl na ko sunu boroom dolli yërmaande famu nekk barkeb Seexul Xadiim ❤️
Jërajëfati Xalaat Tv liggéey bi rafet na na Yàlla dolli la taxawu🙏🏼
Ndaysan yéna bakh wayy man dh chaque première dimanche du mois de Ramadan dagni dém Louga départ Dakar 5h du matin agg ay 11h inchallah ziaré tawou s Sahm mame chaikh Mbay diouli tisbar weur deuk bi dem parlait djili mbay ak fi S Sahm done déff khoudba juste takousane djiot gniou djoli dieul départ ndogo tiwawone djouli guée départ 22 h fékeu gniou Dakar machallah khalat contane na dh
Machalla
Cëy Sëriñ saam xam xam kaasé la wonn . Sokoy déglu dagay Yëkk maguk sunu Boroom
Wawaw
Machalah ❤❤
Daffa leer
Merci pour cette vidéo 👍🏽 c’est intéressant de savoir quelque chose sur la vie des légendes sénégalaises🤛🏾
Connaitre la personne de Julien Zouga serait aussi une bonne chose. Car c'est une icône pour le Sénégal
Kii Moye Fathie Ro Yii Sëriñ Sham Mbaye Yàlla Na Ko Yàlla gërëm te Doli Ko Faye... Vive le #XALAAT Tv💯✔️🇸🇳🤍🕊️👍🙏
WA waw fall aka lerrr
Amine Yarabi
Serigne Sam Mbaye yalla na yalla yokou lérr tase niou si barkém 🙏🙏❤️❤️❤️❤️
Lii dh dafa melni mako mome lii rek laadone rêves pour geuneu xam histoire Serigne sam mbaye 🙏🏾❤️❤️
Mm man
Ak Man
Ndeysane, djoulitt deug ngini, yaAllah neu yaAllah fey baye sam
A chaque fois je me perds dans le droit c lui seul qui me montre le chemin à travers son enseignement "mon maître espirituel"
Kou sope serigne Sam rek beuseul j’aime 👍
Machallah Yalla Mayon Nako Xam Xam de Yalla Nako Yallah Yeureum té kharé ko Adiana si Barké Sydina Mouhamed Psl 🙏🙏🙏
Amiiiine ya Rabi
C'est toujours un immense plaisir de découvrir 🍃 des personnages de haute envergure de cet pays .
Merci beaucoup xalaat TV thia kaw thia kanam.
Mashallah serigne sam mbaye yalna yalla yokk ay léram 💖💖💝c'est mon homonyme 🥰
Allahou akbar Serigne Sam est vraiment 😭😭😭😭😭mon vrai professeur
Voilà louma niane mogui ni mashallah xalaat toujours yinagui dokh tchi lignu nékh merci yallah nalén yallah fay
Mame Mor Diarra Mbaye l'universel, le moudjadid hors pairs❣️👍
Aminnn
Xalaat tv vous êtes quoi 😭😭 bilahi j vous aime beaucoup amal diam frère ♥️♥️
Akassaa
Kou beugue bakh bokoy dégulou di nga baakh
Merci xalate tv vrement yallah sounou borom soubhanahou watt- Allah taxawou samoulen arr len si barké seydina mouhamed PSL
Xamna lou mu xamoul wone si sérigne sam machallah vidéo bi amneu solo yalna yalla mottali yp merci bcp 🙏
Amin
Kounek lay deglou mais moussouma guiss kouko eupe xam xam wakh deugue Yalla.
Bilaay
MASALA amna.solo
Doko guise
Bilay
Man guissoumako
Dieureudieuf Serigne Sam amougne fayame ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Qui moy sameu docteur xol ak rouh nn serigne same yalla na gnou yalla fayal
Amin
Amine
Ndeysane. Am nga docteur bou graw
Ndeysane ♥️♥️♥️ Serigne Same xamna L'islam, Beugue na yallah
Machaalla
Mane déh limakoy deglou yeup bima xamé ni Serigne Sam Mbaye guéneu neuh adouna yagoul parsk ay diangalém dafa mingo ak diamono dji nimouy dokhé actuellement
Dëgg bu werr
Serigne Sam yalla na yalla yock say lerr moussou ma khamm ndeckété kouy serigne Sam mbaye deuggg machllaaa xalat tv
Aminnn
Wallahi kou bakh sax sama royou waye sama idole ♥️♥️♥️♥️♥️🌷
Thieye serigne same mbaye yalna niou ko yalla fayal si barkép serigne saliou
Je suis très content de toi Serigne Sam Mbaye mon idole je l'aime trop😭😭😭
En tout cas je vous félicite et je t'encourage. Que la paix soit avec vous
Histoir bo masa dialale fi rek bi momaci geune nekh yall na yalla fayalnou serigne sam mbaye🙏🏾🙏🏾😭😭
Aminn
C l seule personne que j’écoute H24 tout le monde doit prendre exemple sur lui et réapprendre sur lui enseigner ses œuvres et leçon walahi legui Sénégal 🇸🇳 nekh
Bilaay
Kone nitt kou bakh nga
Allahou akbar Macha'Allah 🥰♥️Yallah na Yallah faye la thi barké Seydina Mouhammad saw 🙏
Machalah !!! Je l'écoute chaque nuit avant de dormir.
J'écris ces mots avec les larmes de mes yeux = Maa ngi bind baat yi ci samay rongoñ.
Yal na Yàlla dolli koo gërëm.
Amouma saguo si bay Sam mbaye wallahi
Machallah xalaat TV Sénégal manoul amat kou Mel ni yawf❤️❤️❤️❤️ ndakh lingay def rafet na trop man mom Bouma la guisoon dina la nèkhal billakhi ❤️❤️❤️❤️
Wéssou woule gnanalko yalla yoki lérame
Aminé 🤲🏿
Serigne saam (RTA)
la source du savoir inépuisable.,
Un parcours exceptionnel
Un homme multidimensionnel
😭❤️🙏Serigne sam Mbaye 🙏❤️
Nous l'attendons avec impatience et merci xalaat du travail que vous faites pour nous 💓💓🙏🙏
❤❤tay mome sema serigne guénn ma indill contann nasi trop yalla nalen yalla fay yewwu🥰
Cey sama sopebi mame sam yallah nakou yallah douli ay xéwal tha firdawsi❤❤❤🤲🏿🤲🏿🤲🏿
Le meilleur conférencier de tous les temps. MANCH ALLAH.
Alhamdoulilah
jërëjeuf wa xalaat tv
Serign Sam Mbaye hafizahoul lah wa rahimahoul lah
Machallah
Ndeyesan 😭 tey mom lall ngama dei Sama sopé bi beugg koo lool ndeyesan yalla nala Serigne bi fay Baye Sam kou mata bayi xell la don jambar lool sii diné rawatina yonou mourid xam thi mom Lou bari ndeyesan leu 16 bii thila ame dom moy Sama tawe mom lako toudé sakh Sama xoll sedd na trop thi lii yalla nako yalla doli lerr xalaat TV beugg nala lool nguir linga deff thi Baye Sam nguir nitt gni xam ko Kend Manou ko xam sakh wayé nguir xam thi mom tuti ndeyesan Dieureudieufe
Ndeysaan yalla yalla barkelko
Machallah grace a vous j ai eu connaissance et satisfaction de ce grand Homme
Merci xalaat
Machalah sen liguey amna solo trop yenangui yée khaleyi ak niou beuri niou done nelaw , Mokham ci ndiagalé mak gni la wala souniou bagn katt yi toubab yi sakalone pekhé. Gueum sa bopp rekk moo woor. Yalla na léne yalla samm
Machallah bègue nane Lolou ❤️❤️Amna solo trop🙏🏻🙏🏻
😭😭😭😭😭😭😭😭
Amna solo
Stp xalaat tv Documentaires sur serigne touba ak voyage bi si mer bi
Kimo tax niou Xam serigne touba ay waxtanam si segn tuba soko deglo lep lo yitewo si segn bi digko Xam
Omare yawe xam xam 000=doffe
Yanou guéthie gui bothi beugué kham lou lér dégue loul S bass khélcom wala S sam wala S Ahmadou Mbacke Darou moukhti S Saliou Sow
Mai khana yaw khamô né serigne sam mô khamlé S.touba ba niépou khamko khamgou wer dafa diangê teerém yépou ba khamko diko xamlé
Yalla nako sougnou borome kharé adiana firdawsi mai xalaat tv yalla sougnou borome goudel sa fane té mayla sa télé bo momal sa bopou 🙏🙏🙏
Alhamdoulilhahi Rabil alamina a travers le nombre de personnes ki ont aimé et commenté cette vidéo je me rend compte que la jeunesse et autres sont entrain d'écouter baay saam magui sogne sama bop ak niep nioukoy deglou sasouné cone diga raw say mass mom da wakhone tamit né diamono gui niew coumou nekh coumou nakhari sama cassette yi niofiy doon ckeikhou tarbiya niofiy doon cheikhou tarkhiya merci baay saam.
Jajeuf way
J'ai jamais commenté tes vidéos mais je les apprécie tous surtout celle-ci ❤
Thiakaw thia kanam yaram inshallah 🤲🤲
Inchalla
Allaahu Akubar Cëy Yàlla xalaat tv tay daaneel nga ma Yal na Yàlla yërëm ko te gëram ko 😭😭😭
Dieureudieufeti Serigne sam mbaye yalle nako yalla yeureume diégueul ko barcké Serigne Touba wadial 18 safar j - 5
C'est la première fois que je regarde une vidéo du début à la fin... Merci Bcp xalaat Tv. Vous avez la responsabilité de montrer aux jeunes qu'on a rien à envier aux autres nations... S Sam était extraordinaire, Yalla dako dimbali. Il mémorisait tout ce qu'il lisait....Ya d'ailleurs son fils qui est sur ses pas machallah.
BRAVOOO ET MERCIII A XALAAT TV. Dimbalil jeunesse bi rek thi wane leen borom xam xam yi nga xamni sén jikko, sén yarr ak téguinn rafett na.
Bilay wakh nga degg
Mo takh ma xam lu barii si dinée qu'il repose en paix
Ndeysan
Merci bcp xalaat tv ❤️
Lii lanu soxla Sénégal barina ay références
Seriñ saam mbay yalana ko yala fay 🙏
Machallah Serigne Sam merci beaucoup ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️☪️☪️☪️☪️
j'ai jamais commenté...je le fait aujrd'8 parce que je suis content de xalat tv... depuis que j'ai commencé à vous suivre vs m'avez jamais déçu ...vus que les gens publient slmt pour de l'argent ...vs êtes les meilleurs
Akassa
Sénégal war nano yéwou thi kép kouy diglou xaalat tv thia kaw thia kanam 💖💖💖💖💖💖👍
Hooo🙏🙏 machallah xaalat tv Sama sope serigne Sam mbaye yalna yalla yokk lèeram amine Aka ame xam xam 🙏🙏( grazie mille fratello
Alhamdoulilah d'avoir une Télé comme #XALAT_tv one love a tout l'équipe 👌
Cette homme a complètement changé ma vie alhamdou lilah 🙏🏾❤️
Wallay dou yaw késsé