NDEYSAAN VIDEO BI DAW NA YARAME , ANA COUYE DIEUF TA YALA TAKH😭😭😭

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 22 янв 2025

Комментарии • 1,2 тыс.

  • @makhousy4154
    @makhousy4154 2 года назад +3

    Machalah, barké dagnkoye gnéédeu,
    Boultaïyi si diapalé mère bi
    Yalla nalééne YALLA soutoural taxawouléene

  • @adakane7134
    @adakane7134 4 года назад +2

    Magui gnane sy barkép séydina moukhaméd yaw fatou bintou yalla bo gnak fii ak alahira yalna yalla fayla yaw dh yalla bo diahlé s6 barkép s babacar sy mane yalna done miliadairou séydina moukhaméd psl

  • @dialloahmed4476
    @dialloahmed4476 4 года назад +2

    Yalla nala yalla mai wer si barcke seidina mouhamed AK werou korbi

  • @moustaphandiaye8099
    @moustaphandiaye8099 5 лет назад +12

    yalla nama yalla may khalice boumay diapale nittyi thi barké serigne saliou bima yakar

  • @mamadoundir8267
    @mamadoundir8267 3 года назад +3

    Ahhh yaye. Boy yalla nala yalla dembali thii barki Cheikhoul Khadim 😭😭😭

  • @youssouphdiedhiou1691
    @youssouphdiedhiou1691 2 года назад +5

    Lii moom,doyna warou,massa!Il y a des hommes qui sont sans cœur.C'est pour cela, il faut faire beaucoup attention.

  • @famasady9852
    @famasady9852 5 лет назад +25

    Iow déhh do torokhe this sa adouna barki Serigne Ababacar Sy machallah vie sur vous lo doundou doyoul ma belle du courages

  • @Yassege78
    @Yassege78 5 месяцев назад +1

    Ndeyssane thiey ndiabote yalla na bour yalla dimbali lenn

  • @tizboy8825
    @tizboy8825 5 лет назад +29

    Yalla naléne yalla takhawou si barképp seydina mouhamed

  • @mariamesms621
    @mariamesms621 5 лет назад +2

    Ndeyesaane fatou bintou yalana yalla takhawou ak sa yaye ani gni yalla may weursseuk ak lp pour diapaleko guir yalla surtout fatou bintou mi dina bakh inchallah

  • @awaamardiop6432
    @awaamardiop6432 5 лет назад +74

    Ma soeur ne t'en fait pas tout ira bien incha allah avec la bénédiction de Dieu continue a aider ta mère tu ne le regrettera jamais

  • @Salimata-lp5uc
    @Salimata-lp5uc Год назад +2

    Ndeyesan yalla nala yalla diapalé 🤲 Amine yarabi 🤲

  • @mariamadrame3371
    @mariamadrame3371 5 лет назад +27

    Machalla une fille brave et courageuse yalla nalen god takhawou si barki seydina mouhamed

    • @Africapress24
      @Africapress24  5 лет назад +1

      Amine

    • @narmbaye7144
      @narmbaye7144 5 лет назад +1

      Amine

    • @fatmabarry2402
      @fatmabarry2402 5 лет назад

      Diapal lèk dina bakh yalla bouy dèfar dafay mèlni kou yakk borom ndaye diou liguèy dina sone mais dou trokh li yeup si ay nètali lay moudiè yèn mbok yi bagna am sakh moko geun

  • @biobeautyhair-body-skin16
    @biobeautyhair-body-skin16 5 лет назад +10

    Cey addina mo metti deh 😭😭😭 ioe deh yalla molay fay , nii ngua diaper sa yaye dji ni Machalla dou nul deh😭❤️

  • @khoudiadiop4944
    @khoudiadiop4944 4 года назад +33

    Nguir yalla nagn lene cotisé nioune gni du commenter chacun 1000fr sah dina dierign dara li c triste ndeysane

  • @andrendione4326
    @andrendione4326 5 лет назад +1

    Vraiment yalla nama yalla may alaal boumay heuy di dimbali domou adama. Vraiment li meetina. Yalla nala yalla tahawou

  • @ouleyewar7989
    @ouleyewar7989 4 года назад +8

    Yalla nalennn yalla diaplé yerem nalén trop 😭😭😭😭😭

  • @sokhnafatiseck4297
    @sokhnafatiseck4297 4 года назад +1

    Ndaysane métina loll yal na yalla takhawo yalna yalla safara ci barkép s touba

  • @darouminamealimentation8530
    @darouminamealimentation8530 5 лет назад +5

    Thieuy adouna aka nékhone ma am ba
    Défal la te yalla takh 🤲🤲

  • @ndoumbely9742
    @ndoumbely9742 4 года назад +2

    Yalnako yalla dimbali thi barki mouhamed😥😭😭

  • @bbadiarradrame9493
    @bbadiarradrame9493 5 лет назад +4

    Quand je serai riche jaiderai tjr les pauvre la vie est si dure mes rien es éternel dans ce vie que dieu nous ouvre les porte de la richesse pour aider les pauvre a se soulever très touchant😭😭😭

  • @mamediarradasylva936
    @mamediarradasylva936 4 года назад +3

    C'est cette Jarre de problème que tout personne riche doit conduire une des bonne actes pour pouvoir être une bonne personne pour que dieu vous considère comme une bonne personne 🙏🙏svp

  • @misterdadji45milliards57
    @misterdadji45milliards57 5 лет назад +136

    Yalla Def ma Milliards Ma Diaplé Diamou yalla yi Bilahi

  • @mamecheikhdiop9340
    @mamecheikhdiop9340 4 года назад +1

    Yalla na lene yalla diapalé s. Barké s. Touba mbacke 🙌🙌🙌🙌

  • @laminecams5787
    @laminecams5787 4 года назад +3

    Je me suis tombé sur cet vidéo franchement j ai des larmes aux jeux q allah vs secoure

  • @cheikhbassiroudiop8678
    @cheikhbassiroudiop8678 4 года назад +1

    Yallana yalla doli soutoura Kéne dou toroxal Djiguéne lii métina dh ay ndaye saane kii dh bouma yorone wallahi rabina tay dinga xamni yeureum nala

  • @blackqueenlasagesse4037
    @blackqueenlasagesse4037 5 лет назад +103

    Bilahi adouna bi mo doy war rek té am goor you bone té amougnou bene yeurmamdé... Yalna len yalla takhawou insha'allah 🙏🙏🙏

    • @Africapress24
      @Africapress24  5 лет назад +5

      Amine

    • @mbaybabacar8980
      @mbaybabacar8980 5 лет назад +4

      C vrai sister gor you bone amna deh li metina loll

    • @FascinatingMya
      @FascinatingMya 5 лет назад +3

      mais pagne bimou satieu mo doywar yalla bumu ci def sacrifice

    • @Africapress24
      @Africapress24  5 лет назад +2

      @@FascinatingMya mo diakhale dieupe

    • @FascinatingMya
      @FascinatingMya 5 лет назад +2

      @@Africapress24 ah mais pour mane niom danio wara porté plainte pour abandon de la famille, de son enfant , maltraitance de sa femme, nitgni nio hamoul seneu droit. wahlene lo mou porté plainte.

  • @marcelolopesgueye7188
    @marcelolopesgueye7188 5 лет назад +1

    Yalla na yalla takhawou si barcke seydina mokhemed bakhou serigne Fallou -

  • @mouhamedhabibndiaye3713
    @mouhamedhabibndiaye3713 5 лет назад +27

    Wallahy la fille si addouna du torox maman doundal lodoundou doyul yalla n'a nako yalla taxawu je suis Un homme très fort digne Sama yaay wallahy dem marche rekk lako Defa lutt footal naako rakhasal naako ma génération ken rawu masi

  • @youmandiaye1499
    @youmandiaye1499 5 лет назад +16

    😢😢😭digassi guène inchalla dafay metti rek mais lepay djex bou sobè yalla

  • @tinadiagne772
    @tinadiagne772 5 лет назад +163

    Fatou binetou bilahi yallah dinala diapalé je te parle en connaissance de cause legui rek ga guiss changement nala wo té dinagn guissé suma gneuwé inch'Allah yallah bouy défarr day melni kouy yakk

  • @soukeyediop8183
    @soukeyediop8183 4 года назад +8

    Fatou yalla di n'a la Faye Sénégal miliardaire yi nagn diapalai pauvre yi

  • @kingrassoul9037
    @kingrassoul9037 5 лет назад +16

    Bilahi naka continuer ndam rek lasiiy guise ak loumou yag yag dinako guise lou way defal Wadiouram si lou bakh yalla dinako faye

  • @mamounecissewakhalsakaw9525
    @mamounecissewakhalsakaw9525 4 года назад +1

    ndeysan sama xol bi féssna bilahi sou yalla défon ma tégui Sénégal amna gniou xamni doun souno bilay ki yalla nalén yalla takhawou 😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @roxayaniang4964
    @roxayaniang4964 4 года назад +13

    C est dur. Il faut communiquer son téléphone pour qu' on puisse l aider.

  • @sheikhalhagiegaye3360
    @sheikhalhagiegaye3360 5 лет назад +2

    Yalla na la yalla japale barke sheikh Ibrahim nyass

  • @diabymariama2563
    @diabymariama2563 5 лет назад +63

    😭💔j’aime tellement ma mere que voir sa me detruit 🙏

  • @anitambaye4270
    @anitambaye4270 4 года назад +1

    Bilahi g pleurer ndax j aime tro ma maman yalla nala yalla diapalé

  • @astoudione9068
    @astoudione9068 4 года назад +10

    Dioy na ba sone bilay thieuy adouna🤷‍♀️🤔😭😭😭

  • @kineba7416
    @kineba7416 4 года назад +1

    Thieuy yalla yalla ga tek loxo thie yaw mi borom yeureumadé yaw mi meun lep tay borom dolé yalla nalen diapalé

  • @Djana4
    @Djana4 5 лет назад +8

    Machalla la fille la do Meusse troxx inchalla kou teral ndeye yalla teralela inchalla legui yagatoul

  • @yacinefall1935
    @yacinefall1935 4 года назад +1

    Thiey yalla nitt mo leundeum bilae doka meusse réthiou ndakh ligay doundou mane mi damako doundou gniounou wara dimbalei dounou dimbalei ndakh sen intere rek 😭😭😭😭

  • @ibrahimakhalilsamb5946
    @ibrahimakhalilsamb5946 5 лет назад +349

    Limotakh ma beugue nek milliardaire bilay

  • @diaristaka3615
    @diaristaka3615 5 лет назад +1

    Bilahi Fatou Bintou d'où masa torokh diapal sa yaye bou bakh boul masa bâyi sa yaye yall nalen yalla diapa lee sii Barkep Serigne Touba bilahi yalla d'où lene s'étant 🙏

  • @fatimacissediaboumamedabak198
    @fatimacissediaboumamedabak198 5 лет назад +12

    Li metina trop ndeysan yalna yallah defal lep si barke nabi moustaph🙏🙏🙏inchallah

  • @matyseck446
    @matyseck446 4 года назад +1

    Thiey yalla 😭😭😭😭😭😭😭 ndeysanne di nga am lou bax inchallah nianou ndaye di nga ko am ndeysanne liii métina trop sax 😭

  • @ayshagillenngomaaaa3108
    @ayshagillenngomaaaa3108 5 лет назад +9

    Ndeysaan Mama,Allah Is with you and Allah Shower His Blessing Upon Your Sickneed Inshaallah

  • @astouniang7277
    @astouniang7277 4 года назад +1

    J'aime ma mère é d tt mn cœur. Thiey adouna am na nioun doundou loy méti sx mé Fatou bintou bilae ioe am gua geureumal Maman bâ paré yalla nak borom beut you reuy bi guis na lep yalla rk Molay diapalé inshala

  • @fatoudiop1895
    @fatoudiop1895 4 года назад +4

    Képeu kou bayi sa wadiour dinko guiss

  • @alanwadda2699
    @alanwadda2699 3 года назад +2

    I want to help how can I reach her

  • @zogriezmann1106
    @zogriezmann1106 5 лет назад +5

    Massa yalla naléne yalla takhawou si barki seydina moukhamet pls

  • @domoubadiane348
    @domoubadiane348 5 лет назад +83

    Fatou binetou mii deh kouko takkeu ,amm djabarr,bou baxx.koukaa dimballer mou deff etudes superieures dina arriwer.

  • @bintawelle2338
    @bintawelle2338 5 лет назад +3

    Thiey adouna metina yalla nalene yalla takhawou thi diayi seydina mouhamed

  • @ndongtv6248
    @ndongtv6248 4 года назад +1

    Yalna L'en Yalla Teguil Natou Bi Lou Yagoul Dara Way Amine

  • @oulimatalaye48
    @oulimatalaye48 5 лет назад +5

    Thieuy Yallah sunu borom. Délen djouli di niane sunu Borom(swt) mou guéné len si situations yi. Du courage

  • @ndeyegaye3843
    @ndeyegaye3843 4 года назад +2

    Fatou binetou yaw dèh diga am lou bakh diga raw say mass dèh yaw dèh diga am nianou wadiour

  • @mariendong7817
    @mariendong7817 5 лет назад +6

    Ma soeur ta situation va bientôt changer ne perd jamais l'espoir et continue à obéir au besoin de maman que Dieu vous bénis

  • @isseutall4596
    @isseutall4596 4 года назад +1

    😭😭😭ndeyesane li mètina troppp magui gnane yalla mou mayema loumay mana takhawo situation you mèlni mètinama tropp😭😭

  • @ramatolayefall4327
    @ramatolayefall4327 5 лет назад +65

    Que Dieu vous vienne en aide si barkê sèyedina mouhamed saws

  • @khoudiakebegueye2473
    @khoudiakebegueye2473 4 года назад +1

    Yalna yalla sam sunu yaye yi.mouyu mana mel sunu yaye lagn.bougn rafetaler dieum si gnom rek sunu lepp dokh

  • @dieynabadiop4333
    @dieynabadiop4333 5 лет назад +3

    Massa Masha Allah yallah n'a l'en yallah djapale tahawula amine ci barke seydina mouhamad psl

  • @astoudiop8591
    @astoudiop8591 5 лет назад +1

    Hoo li metina trop yalla naco yalla takhawou aiyy waiyy Senegal prkoi solidaire rouniou li doyna warr waiyy😭😭 franchemant amouma dei mai beug nathi deff darra nak yalla nalaine yalla diapelai inchalla bn courage sahira li yeup daiyy diekhh

  • @fatouleye5264
    @fatouleye5264 5 лет назад +3

    😭😭ô yalnama yalla df millionnaire bama diappélé néw di doléyi

  • @aidadiouf8887
    @aidadiouf8887 5 лет назад +2

    Aay wayee yalla nalen yalla soutoural lii métina

  • @moctarthiam792
    @moctarthiam792 5 лет назад +3

    barki seydina mouhamed kou sagané sa mbokk wala sa yaye bala Guay death digua trokh Maman mougnal DINA diex mais chapeau à ma sœur adorée et pape sidy séne liguéy raféte na lol bonne continuation 👋👋👋

  • @oumoutraore2201
    @oumoutraore2201 5 лет назад +2

    ndaysane li metina yalla naléne yalla diapalé sa wadiour loko mene defal si lou bakh doko reuthiou fatbintou do torokh mouk lou bakh rék gueye ame inchallah yalla bakhna

  • @coumbasow3693
    @coumbasow3693 5 лет назад +6

    Courage ma sœur inchalla yalla dinaleu takhawou 😭😭😭😭

  • @khalifambaye5348
    @khalifambaye5348 5 лет назад +2

    Yalla nala yalla takhawou si barké seydouna Mouhammad pls 🙏😭😭😭😭

  • @mamediarrababou3045
    @mamediarrababou3045 5 лет назад +4

    Yalla nala yalla takhawou sie barki magal gie gnoue dieume

  • @hawabandiaye1196
    @hawabandiaye1196 4 года назад +2

    INCHALLAH ton fils deviendra célèbre

  • @mansourba2133
    @mansourba2133 5 лет назад +4

    Yalla nalen yalla diapalle si barké seydina mouhamed

  • @diakhateastou5973
    @diakhateastou5973 2 года назад +1

    Que Dieu t'aide comment tu parles de ta mère mashallah

  • @falygueye6601
    @falygueye6601 5 лет назад +29

    Ma sœur yalla nala yalla feye wadioure kouko terale yalla terala c triste 😢😢

  • @aminatandiaye9511
    @aminatandiaye9511 4 года назад +1

    In sha Allah borom bi dinala diapale ndakh sa yaye bi nga takhawou. Du courage

  • @marjanehay4204
    @marjanehay4204 5 лет назад +8

    Billahi dinga toke bassante yalla toke bakoye nétali inchallah.

  • @fatouniang6529
    @fatouniang6529 4 года назад +1

    Mètina trop bilahi 😭😭mais mokam yi ak waji nanou kham ni adouna dou keur kou dèfaloul nitt do dèfal yallah mais fatou diap tèwa bayi rk yallah bakhna

  • @sarafycisko8684
    @sarafycisko8684 5 лет назад +3

    Eywaye adouna mo meti rek so yakaré ni iow rek yaye doundou Lou meti ci adoundou thiey sa me rappel des choses bilahi 😭😭

    • @ramadieng7831
      @ramadieng7831 5 лет назад

      😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @ndeyemaperelam7746
    @ndeyemaperelam7746 4 года назад +1

    Ndeysan ligueyou nday koumouy takha tedd ken doula yeureum gnée nala sakh car j'aime ma mère plus que tout au monde

  • @ibrahimdiallo62
    @ibrahimdiallo62 5 лет назад +22

    Machallah ma soeur tanket pas cest Allah ki ta testè et tu as fè ce k Allah voulè car tu as ecoutè les conseilles d ta Mere💘.““Yallah bouy dèfarr dèy mètti trop ba dèy mèlni kouy yack sa vie“““.... Surtout ne te decourage jamais car allah aime les patients et n fè pas ce kallah ta interdi☝ tu veras 1 jour tu seras trè heureuse avec ta famille.inchallahou Rabbi☝☝☝☝salam

    • @Africapress24
      @Africapress24  5 лет назад +1

      Diadieuf

    • @zahravikymaoriridieng2313
      @zahravikymaoriridieng2313 5 лет назад +1

      je te jure yalla limou yor dou dieh tè pour diam yilla yalla dina la diapaler bou bakh ndimbalou borom bi mo gueune bou nite yalla nallen diapaler❤

    • @mbayediouf480
      @mbayediouf480 5 лет назад +1

      Bilaye wakh gua dègue ki mague mom sougnou ka soratèwoul bilakhi bouy dèfare day mèlni kom couy yakaye ms yalla bakha dafa am goor you bonn

    • @Africapress24
      @Africapress24  5 лет назад +2

      @@mbayediouf480 yala bakhena

    • @boybureeu1748
      @boybureeu1748 5 лет назад +1

      ❤️❤️❤️❤️❤️❤️👂👂👂

  • @eveguisse6981
    @eveguisse6981 5 лет назад +20

    Wallahi tu ne le regretteras jamais
    Tu as la bénédiction de ta maman tu auras que du bien dans ta vie inchallah du courage

  • @khadijadiop7548
    @khadijadiop7548 5 лет назад +34

    Seydina Mouhammad!!!sama hol toyna, thiéy adouna

  • @mariama8672
    @mariama8672 4 года назад +1

    Do Moussa sonou yaye dafa sacré

  • @aron6054
    @aron6054 5 лет назад +31

    Sénégal mbokou légui bo amoul kéne doula considéré comme nite, xam ngua li metina bafou méti yém , nguir yalla diapaléléne ko

  • @pendasoumsoumare7488
    @pendasoumsoumare7488 5 лет назад

    Bilahi man dama tite si aduna bi sama dieukeur ni leu deffff takkk m fekk m nekk khale bou takkk m dieul m bobou lako giethie guisss kou ne goor bkh n sa baye motkh bilahi lima metty yeup moun mako fathie yalla nalen yalla faye ga am ligay bu bkh si barki seydina mouhamd

  • @mimifall4039
    @mimifall4039 5 лет назад +4

    Lou metii yaguana si adouna mai lo mougne rek mou diekh inchalla mbokou legui yi dagnou lay khamale rek mai yalla bakhna

  • @oulimatadiack5168
    @oulimatadiack5168 4 года назад +2

    Naysane li métina😭😭😭serett yallah nala yallah takhawo

  • @tinandao1425
    @tinandao1425 5 лет назад +13

    Parfois c gens de mauvaise foie utilisent lhymen pour des sacrifices et autres il a profité de la pauvreté de ces dernières pour parvenir à ses fins mais nak yallah mo eupeu dollé kouy mindèf yalna yallah defar lëp

  • @BOYDIANTAL-vy5kf
    @BOYDIANTAL-vy5kf 9 месяцев назад +2

    😢😢😢

  • @mariemarie867
    @mariemarie867 5 лет назад +8

    Oooh li metinaa 😭😭diguaa am lou bakh inshallah Bilahi Gnila abandonnei Amouniou khol
    Surtt say Dom
    Haai dieu

  • @astoufall9556
    @astoufall9556 5 лет назад +2

    Ndeysane sa dome dji dou meussa torokh si adounam yalla nalen yalla sam bilay day metti rek mé dina bakh 😭

  • @Hamidouadame
    @Hamidouadame 5 лет назад +11

    yaye boy sama rake my yalla nko yalla diapale

  • @amadouba3892
    @amadouba3892 4 года назад +1

    Yalla na yalla guénéléne si souffrance bi vraiment affaires bi dayna yarram
    Inchallah savas aller👏👏👏

  • @diopfama1079
    @diopfama1079 5 лет назад +3

    Thieye amouniou faye thi souniou wadiour yi 😭😭😭dicourage sister geuramal wadiour mo geune lepou thi aduna liko dale lepou thi ame dome lako dieule taye dome diodiou waneko guinaw metina

  • @ndeyegaye3843
    @ndeyegaye3843 4 года назад +1

    Amna gniou bonne nak bonne amoul bène ndiarigne mè mougne len rk lepay diekh fatou binetou diga am lou bakh dèh bilahi

  • @sophiesow8619
    @sophiesow8619 5 лет назад +86

    😭😭😭😭 Jarive pa parler on Vendé de lakhe pour ma mére et on n'es 6 filles mes aujourd'hui alkhme doulilakhi

  • @nabyaicha527
    @nabyaicha527 5 лет назад +1

    Ndeysane yaye boy masta yallah nga tané thi diame ak salam Fatou Bintou lilaa done défal sama yaye😭doko réthiou dinga fakhass talou wayé do danou métina nak wayé dou dara lou nékh migui nieuw 1ne challah dii niane yallah mou déf thi khéweul bou barii🤲dafa ame domou adama yo khamné khalatou niou dé kou beuguoul bopam rek moy torokhal mromame thiéy Adouna🤔

  • @benabambamendy3910
    @benabambamendy3910 5 лет назад +3

    Vraiment g pas les mots khalissou ngour bi dé khawma limouy ndieurigne

  • @khadyndiayedjitte803
    @khadyndiayedjitte803 5 лет назад +2

    ahh vraiment mettina ba fou metti yeme mais nak yalla bakhna dall dama khamoul mane mbokou légui louniouye diarigne si adouna mais nga dimbali sa mbok soko amai te yalla takh vraiment mettina ba fou metti yeme maye wakh wadiou bonne diodiou tamite kene geunouko yess mais mounielene yalla dinalene atte ak niome

  • @papendao4249
    @papendao4249 5 лет назад +3

    Kou meun nangko diapalé té yallarek takh,kou meuneuguoul nangko nianal, yalla bakhna.
    Un conseil pour la fille,moussoumaguiss kouy diapalé ay waydiouram baniou gueureumko,moudieulessi torokh,donc diappalrek dina bakh inchalah😭

  • @mameyandembodji758
    @mameyandembodji758 5 лет назад +2

    Walahi yalla guiss nala yow rek yaye téde inchallah.
    Lépe lo def guir yalla ya rabi dinala ko féy inchallah wakhatou ma linga def thi wadiour.
    Mougnal rek inchallah yalla dina gnew inchallah