allahou akbar thieuy yalla li doynawar NDayssan Mère bi sonnuna, gniko fiy fék tamit diko diéma saku

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 22 янв 2025

Комментарии • 253

  • @hamidoudiallo7504
    @hamidoudiallo7504 2 года назад +23

    Merci pape Niang avec tn equipe je vous adore meilleur des choses à vous

    • @awasow7354
      @awasow7354 Год назад

      😭😭😭😭😭🙏🙏🙏

  • @NdoyeMalick-t9x
    @NdoyeMalick-t9x Месяц назад +7

    Xaléla dh magui niane yalla yalla téralma bama téki démbalé malade manteauxs yi cheikh ✨ yalla nalla yalla samou yak sa équipe 😢aminne

  • @papandiaye6249
    @papandiaye6249 2 года назад +19

    Yéne nieup yalnaleine yalla fay si barké mame saliou mbacké ❤

  • @ndiayecheikh5025
    @ndiayecheikh5025 Месяц назад +4

    Bilahi Yala rek molay faye pape ak sa wa ream insalah

  • @gayembengue9021
    @gayembengue9021 2 года назад +12

    Bilahi yalnalén yalla fay yalla yok soutoureu bi si barkep seydina Mohamed psl

  • @kennatoudiop8313
    @kennatoudiop8313 2 года назад +17

    Yalnalén yallah défal diam yalnalén yallah fay si barki mouhamed. Dieureugén dieuf🇲🇷🇲🇷🇲🇷

  • @papediagne661
    @papediagne661 Месяц назад +1

    Thiey yalla li matinale trop bilay yalna la yalla takhaxou yaye boyy😭😭🙏🙏

  • @ababacarienne3873
    @ababacarienne3873 2 года назад +7

    Wallahi lii amna solo yalna leen yallah fay bijahi Nabil Moustapha SWS

  • @papendiaye3237
    @papendiaye3237 2 года назад +1

    Yàlla naleen yàlla doli tawfeeq ju bëri, li ngeen di def amna solo lool

  • @SD-ih6bz
    @SD-ih6bz 2 года назад +9

    Sant yallah migui lèk amena appétit dalena khèle dîna wéur in challah. Moome dafa nèk thi mbèdeu rèk wayé Sénégal gui lifi nèk lègui kène meunouko wakhe bilaye walaye. Wanté sougnou birome bii daara teuwoko yalla n'a yallah khétélî kèpeu kou soone in challah bravo à Pape et son équipe 👏👏👏

    • @ousmaneba9503
      @ousmaneba9503 7 месяцев назад

      Ndeyesan machallha wakh ji amna solo

    • @ousmaneba9503
      @ousmaneba9503 7 месяцев назад

      Ndeyesan Sénégal 🇸🇳 yallah nañou yallah yerem virement te dieggel ñou

    • @ousmaneba9503
      @ousmaneba9503 7 месяцев назад

      No Sénégal warna am palace pour Nit kou amoul foumou.dek

  • @Matar-i6d
    @Matar-i6d 6 месяцев назад +2

    Bilay yéne nitt .amoul sén faye.bilay yalla naléne yalla sammou rék 🤲

  • @borombakh1129
    @borombakh1129 2 года назад +8

    Ndayesane thieye bilahi wallahi yalla rêk Moléne mana Faye ya Aida bilahi ya raféte khôl yalla nala yalla Faye sa khôl Ake sa yéné maye la ndiabote gou barkél Ake kinga beuga seyal ni Amine pape Niang merci beaucoup 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @sarrcheikh254sarr4
    @sarrcheikh254sarr4 2 года назад +2

    Ya ayda Ndiaye yalla nala yalla takhawoul bopam si barkeb alkhourhane amine

  • @ndoumbeniang7341
    @ndoumbeniang7341 2 года назад +19

    Ces gens sont les meilleurs dieu vous vous garde vous êtes brave

    • @mariemefall3449
      @mariemefall3449 Год назад

      J'aurais bien aimé faire partir de votre association

  • @banelnegri2578
    @banelnegri2578 9 месяцев назад +1

    Eskéy c'est vraiment triste pape yallah nalene allahou faye sameu léne amine ya rabi semeu khol djekh neu si ki

  • @ndeyebounamadiop5863
    @ndeyebounamadiop5863 2 года назад +10

    Pape maachaala yalla nalla yalla faye

  • @aissatoudiop8705
    @aissatoudiop8705 2 года назад +15

    Pourquoi pour s'occuper d'une personne dans le besoin il faut une autorisation ?vraiment yalla naléne sounou borome bi fayale bopame ❤

  • @CouraDiop-k4m
    @CouraDiop-k4m Месяц назад +2

    Ndéysane yallah nala yallah taxawou si barké seydina mouhamet salahou allah mouhamet 😢😢😢😢😢😢😢

  • @maguettegueye143
    @maguettegueye143 2 года назад

    Ay way pape Niang yalla n'a yalla dolly diam AK soutoura djou Sakh dak walahi ndeysan oh oh ndeysan thiey yalla

  • @astoufall3092
    @astoufall3092 Год назад +1

    Sénégal mo metti dagay febar gnou warla diapalé dila daw thiey adouna mo metti pape niang machallah yalla nala yalla faye 🙏

  • @arfangarfang4943
    @arfangarfang4943 2 года назад +3

    Macha Allah Allahu Akbar yalna lén yalla souniou borom bi takhawou inchallah

  • @khadyastoudiop4944
    @khadyastoudiop4944 2 года назад +71

    Elle n'est pas folle je m'excuse du terme .elle cherche juste une stabilité. Elle digne et travailleuse .on doit l'aider pour qu'elle reprenne sa vie.

  • @hawadatt3595
    @hawadatt3595 2 года назад +2

    Eyy way pape sama khôl bi yeup diekhe na pape Niang yallah nala borome bi fayal bopam AK gni guay andal

  • @fallousyll6217
    @fallousyll6217 2 года назад +5

    vous êtes les meilleurs du monde yalla naléne yalla défale diam

  • @mariamabousso3008
    @mariamabousso3008 Год назад

    wallahi pape niang yalla Molay fay

  • @elbiranetoure4870
    @elbiranetoure4870 2 года назад +1

    Yalna yalla taxawou barkep Al khoranol Karim séné ligaye amna solo trop Machallah diamou yalla thi Diam yi 😭😭😭

  • @mariemetoure4659
    @mariemetoure4659 Год назад

    Yalla nalene yalla feyal bopam takhawoulene si barke mouhamed

  • @fatoudiallo9542
    @fatoudiallo9542 2 года назад +3

    Yalna léne yallah Faye thi barkhei Seydina Mouhamed Psl ❤️❤️

  • @aminandoye3487
    @aminandoye3487 2 года назад +16

    Mère bi ma kham metitam damadone diay fataya poêle diwline bou tangue eulbeutikou sama tankayi 3h ba 1h du matin sama tankeu yi daniouy khothie thi glace bandage yi dafay geunei metti yalla nako yalla may tane

  • @coumbagueye494
    @coumbagueye494 2 года назад +4

    MachaAllah Ya Aida yalla nala yalla takhawou

  • @ArretArret-p3n
    @ArretArret-p3n Месяц назад

    Machallah yalle nalene yalla faye

  • @safietounguenodiakhate8012
    @safietounguenodiakhate8012 2 года назад +16

    Diam loumouy wara santé yallah beurina yallah na bokkou euleuk gnii diapalé newdii dolè yii inchallah

    • @coumbagueye494
      @coumbagueye494 2 года назад +1

      Amine lolou rek laay niaane yalla

    • @CheikhoumarBaba
      @CheikhoumarBaba Месяц назад

      ​@@coumbagueye494 Wallahi ndeyssan 😢 lolou lagni niane nioune nieupp mais YALLA naniou YALLA maye aye kheweule youu barry thi barki Yonentibi 🤲🤲🤲

    • @bilalfall1080
      @bilalfall1080 Месяц назад

      Allahouma amine inechala digasi bok

  • @famabasock8656
    @famabasock8656 2 года назад +6

    Ndeysan 😥😢j'imagine si c'était ma mère ou ma grand-mère il faut savoir aider les gens la vie n'est rien mm si vous avais 50f ou peut importe avoir un bn cœur c'est kel k chose de meilleur

  • @fatydemedeme8340
    @fatydemedeme8340 Год назад +1

    ma challah pape ma
    ngi joye sak longue vie a vous♥️♥️♥️♥️

  • @Maty687
    @Maty687 Год назад

    Pape Niang yalla na yalla goudale sa fan si Barke sarige Saliou

  • @annecheikh3934
    @annecheikh3934 2 года назад +4

    Ya aida qu allah vous paie tu es genereuse ta mission est noble yo alla yob moýýere adiarame seydi ndiaye de la mauritanie

  • @alimaniang1189
    @alimaniang1189 2 года назад +7

    Bilaye Pape Niang yalla dinala soutourale

  • @jeancollinsarr7245
    @jeancollinsarr7245 2 года назад +3

    Yalna yalla samléne té takhawouléne machalla ligueybi rafétna trop machalla ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @fatimafall5496
    @fatimafall5496 2 года назад +11

    Bilahi Pape Niang AK touts l'équipe yall nale. Yall dafal souteura😭😭😭

  • @KhadijaSeck-sh8tn
    @KhadijaSeck-sh8tn 6 месяцев назад

    Dahisane ya aîda yalnala yalla fahi tiyaba ya bakh

  • @FatmaDieng-qj3iw
    @FatmaDieng-qj3iw Год назад +1

    Yalla mi am séne Faye yalla naléne yalla faye

  • @ousmaneba9503
    @ousmaneba9503 7 месяцев назад

    Pape yallah Nalen Yallah faye te maylen wer

  • @FallouThiongan
    @FallouThiongan Год назад +3

    Machallah pape 🙏😭

  • @oumoutraore4407
    @oumoutraore4407 2 года назад +8

    Assalamou aleykoum je vous suis depuis Mali qu'Allah vous assistes

  • @maremediagne8217
    @maremediagne8217 2 года назад +20

    Salam haleykoum ! Djeuredieufati yène wa AATGW. Yalla na lène Yalla same té taxawu lène. Amine yâ Rabbî.

  • @souadousow4289
    @souadousow4289 2 года назад +6

    Salam alhamdoulilah magui ziar gneup massa yaye boye khol yi toye na dila nianal yalla may goudou fane ague weer si barke seydina mouhamed 😭😭😭😭😭🤲🤲🤲

  • @dieynabapouye3289
    @dieynabapouye3289 2 года назад +3

    Bilahi defois la vie est injuste sama hol dey diekh merbii yalnako yalla tahawou

  • @layendiaye7811
    @layendiaye7811 2 года назад +4

    Yéna gui liguéyal yalla yalla nalén yalla fay

  • @MamanFall-u8i
    @MamanFall-u8i Месяц назад

    Yaye yalla nala yalla defal tawfekh si bargue seydina mouhameth 😭😭😭

  • @bilalfall1080
    @bilalfall1080 Месяц назад

    Ay yalla mayema alal bou seleu bama meune dimbali dioulite yi nek si thiono ay yalla mayma teranga😢

  • @suzannembodj7404
    @suzannembodj7404 2 года назад +1

    Cheikh Niang je ne te connais pas mais borom yaye djou bakh, goudal fane ak weur

    • @gueyedaouda8592
      @gueyedaouda8592 Год назад

      No pape aldianaye kereume euleuk yalla na yekh adianam léér nama ni pape Dina doundou ay ate you Baaari li yomboul dé

  • @ndeyeloum1464
    @ndeyeloum1464 2 года назад +3

    Ya aida yalla nala yalla Faye barckep Serigne Touba amine 🥰🤲🤲

  • @awadiop149
    @awadiop149 2 года назад +1

    Equipe bi yalla na lene yalla bolle fayy barkhe seydina mouhamet psl

  • @KhadijaSeck-sh8tn
    @KhadijaSeck-sh8tn 6 месяцев назад

    😭😭😭dahisane.yalnalene.yalla.fahy.bilahi

  • @thiarra9047
    @thiarra9047 2 года назад

    Merci beaucoup Niang balo

  • @maguettendoye1948
    @maguettendoye1948 2 года назад +3

    Amna problème khel dé yalnaco Yalla takhawou té takhawou mbolem djoulit

  • @innapoumane4593
    @innapoumane4593 2 года назад +1

    J’ai pas les mots 😭😭😭😭😭😭😭alahou akbar yalla moy karime yalla naniou soli soutoura t Sam jame yi

  • @GeyeMoudou
    @GeyeMoudou 10 месяцев назад

    Bilahi yalla rek moledi fay merci bokom

  • @suzannembodj7404
    @suzannembodj7404 2 года назад +4

    Mon cœur saigne, qu,Allah vous rembourse au plus haut, je pleure, je me met à sa place,c le jihad que vous faites,je ne trouve pas le mot,elle est sénégalaise,massa mane ni étrangère,lii métina,yAllah tawkh ko ti daradja Mohamed PSL😭😭

  • @yacinecisse8621
    @yacinecisse8621 2 года назад +5

    Gnou gui laye gnanal boubakh😭🙏

  • @MalickDiatta-i6o
    @MalickDiatta-i6o Месяц назад

    Massa yéyé bay yenne gni yalnalen yalla Faye 🤲🤲🤲🤲🫶🫶🫶🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @saphietoudiedhiou1586
    @saphietoudiedhiou1586 2 года назад +3

    Yalla mi Am fay yalla nalén fayal bopam 🙏🙏🙏

  • @gottkonteye6914
    @gottkonteye6914 Месяц назад

    Ndeyssan daffa sonn rék billahii 😭

  • @mariamsoumare5490
    @mariamsoumare5490 2 года назад

    ya allah ya rahmane yallah nako yallah takhawou arr ko soutouralko
    yallah nalen yallah fay

  • @modouseck1719
    @modouseck1719 Год назад

    Dieureudieufé yalla sougnou borome❤❤

  • @antandoye7709
    @antandoye7709 2 года назад +1

    Ohhh kel brave femme ya Aïda NASA diamou yagu

  • @GnimaManè-n1q
    @GnimaManè-n1q Год назад

    Salut pape niang daffa ame sama rak bou amé fébarou khél papa ak yayam doundeu tougnou maye sakou ndimbeul rék ts😭😭😭😭yalla takh😭😭😭😭

  • @safietoudiallo3212
    @safietoudiallo3212 2 года назад

    ohhh pape ninag yalna la borome bi dollele .
    c est triste.

  • @kinediopdiop5097
    @kinediopdiop5097 2 года назад +11

    Pape bou amone fouk you mélni yw mou nékh kéne dou yw si mime réw

    • @moustiquo1
      @moustiquo1 Год назад

      Pape ya ngui ligueyal rewmi deh. Yow deh talo procés ba ak sa khol bou rafet. Yalla nala yallah diapalé yak gni ngay andal. Ayway gni yallé bakhé khana yeugounou ligueyou Pape bi ???😭😭😭

  • @ndeyemaremefayelababacarienne
    @ndeyemaremefayelababacarienne 2 года назад

    Yalla yalla faye pape Niang

  • @dioufsira8570
    @dioufsira8570 2 года назад +1

    Ndessane problème rek bilaye ndessane yalla na yalla safara

  • @fatimatangaide3754
    @fatimatangaide3754 2 года назад +21

    Alhamdoulillah. Qu' Allah SWT facilite et déverse ses bénédictions sur vous. Khol fessna

    • @fatimatangaide3754
      @fatimatangaide3754 2 года назад

      Tawfik Inshaa'Allah. Je vous suis de Nouakchott Mauritanie et ne vous envoie nos douas. Longue vie

    • @aissatandiaye1093
      @aissatandiaye1093 2 года назад +1

      Allahhou akbar shedwoende Leelee ah je lala

  • @NaRR.FaLL23
    @NaRR.FaLL23 2 года назад +1

    Ya aïda kénn dou mom diamou si yalla rék takh❤

  • @thiatouserignesaliou
    @thiatouserignesaliou Год назад

    Alakhou akbar ani brome milliards yi 😢

  • @yayibayam-ji9xp
    @yayibayam-ji9xp Год назад

    Yalla nalene yalla faye

  • @yadearamendiogou588
    @yadearamendiogou588 2 года назад

    Mach'Allah ayyy wayyy li mètina wa ani wa quartier bi yalla nako yalla takhawou

  • @SeynabouNiass-d7y
    @SeynabouNiass-d7y Год назад

    Pape sakeur aldjana la yalla. Molay Faye yabax

  • @mouhniyantv3249
    @mouhniyantv3249 2 года назад

    Thiey yalla nalèn yalla fay barkep cheikhoul khadim😭😭😭😭

  • @adamaseck8816
    @adamaseck8816 2 года назад +2

    Massa yaye boy yenne gni yalnalen yalla faye 🤲🤲🤲🤲

  • @seydaaissatoudiallo4262
    @seydaaissatoudiallo4262 2 года назад +1

    Allakhou Akbare tieuy Adouna Ndeyssane

  • @diadiafall6304
    @diadiafall6304 2 года назад +19

    Que dieu vous bénisse ❤🙏🙏

  • @sarrcheikh254sarr4
    @sarrcheikh254sarr4 2 года назад +1

    Billahi suma dégué diouné Sénégal deukou térangala dafmay diakhal khola métid niou koy guiss diko sétan

  • @ndeyefatoucisse8676
    @ndeyefatoucisse8676 Месяц назад

    Yalnalen yalla fay

  • @fafoudiagne1860
    @fafoudiagne1860 2 года назад +1

    Ndaye sane yalla bakhena

  • @coumbadiop8895
    @coumbadiop8895 2 года назад +1

    Yalla nalén yalla Faye 🙏🥰🥰

  • @ramataball2091
    @ramataball2091 2 года назад +1

    Merci merci merci beaucoup porte vous bien gue le bon dieu et avec vous

  • @sodadabo7105
    @sodadabo7105 2 года назад +4

    Ahhhh😭😭😭😭😭😭😭😭 sama hel demna si sama yaye yalla. Nako Yalla yeureum 😭😭😭😭🙏🏽

  • @gassndoye4458
    @gassndoye4458 Год назад +1

    Waa Ani ayy mbokam

  • @bintadiagne5425
    @bintadiagne5425 2 года назад

    sama khôl fen na Lou nek dagkay khôl sa bop rek yalnalen yala takhawou

  • @PapeCheikh06
    @PapeCheikh06 2 года назад +2

    Yalnalén yalla fayyyy💯💯💯💤💚

  • @elhadjidiop1228
    @elhadjidiop1228 Год назад

    Merci pape ❤❤

  • @mameamydiabaye
    @mameamydiabaye Год назад

    Machalla

  • @gorasow7342
    @gorasow7342 2 года назад +1

    Yalnaleun yalla feye

  • @mariamamboup9741
    @mariamamboup9741 2 года назад

    Ya aida yalla nala Yalla faye

  • @kennatoudiop8313
    @kennatoudiop8313 2 года назад +5

    Ya aïda wallhi billay
    Yallah dinaleu fay bagua khamni faynala inchallah 🇲🇷❤

    • @matimbaye9781
      @matimbaye9781 2 года назад

      Dako kham khana

    • @kennatoudiop8313
      @kennatoudiop8313 2 года назад

      @@matimbaye9781 nn mais . Yaw thi bop lernaleu que yalleu dinako fay

    • @matimbaye9781
      @matimbaye9781 2 года назад

      @@kennatoudiop8313 deugele mome ndeysane

  • @khadimniass5479
    @khadimniass5479 2 года назад +1

    Bravi

  • @nenekeita8720
    @nenekeita8720 2 года назад +10

    Pourquoi dieguene bou done séye sou amé diaffé thi fébar dieukeurame abandonné ko mais goor boug fébaré gni dieguene na mougne

  • @aichacheikhameguyaz2061
    @aichacheikhameguyaz2061 2 года назад

    Elle m'a fait pleurer bilay😭😭😭

  • @daradjitv3872
    @daradjitv3872 2 года назад +3

    Dieredieuf wa and takhawou niou wiradi

  • @sokhnasaliou7848
    @sokhnasaliou7848 2 года назад +6

    Tonton pape Niang Mane dama begue bok thie association bi

    • @borombakh1129
      @borombakh1129 2 года назад

      Nemoro pape mongi si vedeo bi woko