N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Wa mais fall boul niou sonnaal diam sila lepp khëdie nitt dëy sakkou diam dontë lii gua wakh rafëtt naa wasalam tawfekh ak taïsir❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sa genre gii rekk nioy nafékh yii yaw ya wara teuth sa lamign niom niarre xam naniou liy sén problem m yaw dangeu wara bayii dii wakh cii lac ndakh xamo léep sii mome té jibbo bii molla nexoul
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Merci❤❤
Balla Gaye a un grand cœur ♥️ amoul dara kholo niiiit kou boooone .
Yalla n’a sunu borom rafetal diguentém ak Lac barke Mouhamed PSL
Lolou aye doul leuh balla dafa bone soxor motakhe mouye khekhe modou lo pour meuna dane siteu waye yalla molene eupeu dole mome ake Aziz ndiaye Sénégal bayi lene nafeke merde waye
Lingay waxxx aamoul beine cohérence.nopil tei wouti lo deffff
Boyy bi mo wara dal diam dal niouko dakk wakh niofi nekk te wahouniou wakh bi lagne wara arrêté surtt boy bi dafa wara nopi dall
Yalna niou yalla moussal ci ay dieum you melni
Clanda mi deh aka yagg AK mbeur yi . Tu es véridique et fier
machallah ❤boy
Frere Guisgue Nite danguay Nite guisgue dioubo si diamou yalla la bok lac de guiere balla gaye ay mbonkou laniou mom migui nane frere lac de guiere dou mem sangre mom dasi wakhone montakh insbi dafa rouse guisgue Niari Nite you bonkou kousi wakh nangua kham loye wakh bilaye Gou wet rousss Chapeaux a mbathieu pereira sama mbonkou walo walo bi ❤🙏🫂
Aziz Ndiaye mo mom xalissam bouko nekhone douko diokh leufeul ndeyam doul waay
Iow yaye outeul lac2 ay none
Boy Ioe Kou kateu sa ndéye nga ioe
Iow élément Minka gua deug rek mola gnoor 🙏
Boye bi dégue rék laye wakh ❤
Sa data yaye yaw
Vraiment deug nexoul point 😂😂😂😂😂😂 deug dou nékh 😂😂😂 diadieuf boy 👍👍
Machallah❤❤❤
mome nak vraiment keneuh khamoul ce qu'il veut à la fin beugeul diam nak stp
😂😂😂 boy bi si diangue wax la tollou
Surtout 😂😂😂
Boye bi guis nako garou térr bi Dakar sama khamone deug ndayam
Wa mais fall boul niou sonnaal diam sila lepp khëdie nitt dëy sakkou diam dontë lii gua wakh rafëtt naa wasalam tawfekh ak taïsir❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ce garçon parle bien ❤
nafekh kharam bi seuytane nga
Kalanda wallahi deug rekk nga wakh gayi yémalé wouniou daniouy xadialé mbeur niom leader yoyou lac de guier gayi danioukay guérre discrètement wonéwou rekk molène nekh
Bilahi wakhe nga deugue lirou Diane ake ketchup rek la
Boy bi seytané leu après la pluie c le beau temps ahe
Boye khana amo lo defff😂
Bariga wakh trop
Vraiment ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ah bon Balla geye2 défoul lou Lac2 guerre défoul😂😂😂😂😂😂 ya yabaté
Iow seytane nga lignou deff dafa rafet
Boy bi deugue rék leu wah naféh yi nio wara mandou ci diguenté Balla ak lac
Danga beug siiw rék
Yowe un million meun guako mayé
Lac2 waroul Winn dem kr bg2 ndax sou sagnonn ada fass dannn ko na prête attention bou bax
Nitou deug purr deug nékhoul ❤❤❤❤❤
😮lac 2 dafa niak fayda
Boye bi sof na bilaye
boy bi ngaka deug leu ms lac de guerre sathie leu
Boy bi nitou deug la
😂 ki boye bou kon la mais pour mome ils et intelligent kilifeu xalé douko yéd so beugué barké
Yaw Balla bou dibo ak lac 2 limit wathieballa yen Balla ay suporter rek lalay dole domeharam
GENROU DOMÉRAM YI WAROUNOU YAGG SI ADINA 😢😮NAK AY DAJAAL LANOU
Non kii nak moye diakhasé balla guaye ak lac de guerre si wah rékk gua koye khamé
Iow yaye ndeye séytané bii ! Chaque jour yayy gueine di sosal balla ! Nafeik séytané cei toi
Saytanè mougui commencer thi keur yi 😂wa Guediaway xawma lane moy sene problem mbeur yi am nguene diot trop du ay
Boy boxeur américain yii amouniou mistique es que lac souh amée combat deuguéne kay bayii mouy dém founékh
Yow règle ndeyame ga wagni wax bi yaye yokale lac ay none
😂 ba taye yagui néka ak saytané journalista saytané laa moye miye wakh lac mo woute djibo ak balla gaye ki moye saytané premier bi
Boy bi khamoul foumi takhaw journalists yi ay seytané lane diakhasé rekk😮
yaw yay dmrm balla dou moromou lac de guerre si dara
Ioe mi yaye cheytané balla akk lac bénneuh laniou nopil 🤫
@@GoraMbengue-f2j sa data yaye ak lac de guerre
Iow kou deugg sa ndeyy gua
Toi c gu cv
Dett way
Boy yii nio tax wa guediawaye douniou massa and
Boy yow ya wara tej ndeyu sa gemegn bu hegn bi
Boy bi bokul dara ak lac bayiléne di déf titre frere de lac meussul nék frere lac2
Boy bi kou dokhane ndeyam la
Lilén Aziz Ndiaye may danguénko khép té badolo rk Moy khép liko nit maye
❤❤
Boy wagnil wakhhh dji moo geun dina wooo Mame mor sakhhh wakhh ko parce que yaw dagua eupeul quoi
Iow yay domHram deugdeug
Ki nafek la wolahi
So demei mom mi moy nafekk bi adouna lep teranga la niou deuk daniouy dioubo nekal nitt
Bayiko rek niom
Nioy wakh ba paré beug ko djign niit gni may wakh mounane shopping nokoul feulé shooting lagni wakh
Clanda bayil magyi ngaye yede khale dou yede mage
boy bi dafa wanné trop ak français yi doule way yao😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Legui kania gou diouk niou diokhko micro Mouy doul rek sarap ndaye site yi rek
Boy démale nga ligéyi
Nice
Yow mima guiss ni dangua panne Kilifeu
Iow boy doul way sofff nga trop
Fougn tassé na kat sa ndy
Boy daf ma neh dah dafa deguo lolll lim wah degue pir leu niom ay maglan lo rafet lan wara def
Ki mom es que dioulite la ki d'où nitt kou bakh
Sa genre gii rekk nioy nafékh yii yaw ya wara teuth sa lamign niom niarre xam naniou liy sén problem m yaw dangeu wara bayii dii wakh cii lac ndakh xamo léep sii mome té jibbo bii molla nexoul
Yaw boye soff nga trop Nite Day beugue diam
Ki li bala am ta lace amouko moy dageu kholam
Boy bi xamadi na troop
Nopil touti ishhh
Yaw doff la 😂😂
Boy bi dafa doff mom
Yowe dof gua tu es ne pour être koi? Yowe lo diokh lac2
Rèw ak sokhor mola diape ak gnaka mandou
Lac 2 mo wara nopilo boy bi... Ay bêtise rek lay wax.... Epuis Xawma kukay diox autorisation pour mou wax sax...... Ki nafekk la way
Mom dafa bokoul ak Dara lac 2 sakh
Papis ak mame Mor nioy ay frère lac tè nioniou delone deug jamais niou wax Lou négatif mais ki mom seytanè la
Yaw nafèkh nga boune diobowoul loumouye wagni balla kone rèfète lènsi
Yaw ya wara nopi sa wakh mo bari
Yawe rék yaye nafékhabii dioubobii aragéwoula démal ligéyii
Yawdi seuytanè nga deh
Yaw vraie saytané gua
Yaw ya barri wakh y
boy yaw ragal nla torop gor dou saytané
Yawe doul 🤐🤐🤐
Yaw boy nopile seuytané gua rék fi thiow amatoufi wakhal lou rafettecmo gueune
Boy démal ligueyi wax rek ngafi nékhè
Boy iow yaw nékho man dara danga sof ndayam trop tu parle trô
Yaw do nitt dara
Yaw nopil way
Yaw mi yayed nafékh bi ngakh yaye diakhasé lac 2 et Balla gaye 2 yayed saytané bi
Djoulite dayy mandou saly