Reug Reug minimise Modou Lô : "mane champion du monde laa, mom késsé doufi mbeur..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 8 янв 2025

Комментарии • 241

  • @OmarBao-gu5qp
    @OmarBao-gu5qp 16 часов назад +40

    Lolou tegal ko niom ganou fi lambou jui modou Lo moy sen papa ❤

  • @TopGueye-nv7pc
    @TopGueye-nv7pc 16 часов назад +28

    Sénégal roi mofi am

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h 16 часов назад +23

    Reug si lambe modou moye saine baye se le roi

  • @ngommamegor7924
    @ngommamegor7924 16 часов назад +34

    Bilay ki gauna sonou moy kii kontor modou modou moy sen papa 😂😂

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 6 часов назад +2

    Modou Lo yalla nala yalla lafal thiate gneipou ioe lagn tek beutt

  • @morgaye9582
    @morgaye9582 12 часов назад +7

    Reug reug desfois daguay waxe rk ma décourager Mod lo tolal noula neikh dafay coupé distance bi kheikh ak iao touché leu je donne le cas de B52 Mod lo dafa doug si garde bi gagneko si beute té tapha tine soutoul B52 et si mes souvenirs sont bonne yaw biguay débuté si mma dem diangui kheix toubape dagnounila sen arènes bi yeup Mod lo kassé mossi kheip yakofi waxon hm

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 16 часов назад +32

    *Le fait detre champion de One Championship, qui est comme la 2e division en MMA comparé à l’UFC, n’a absolument rien à voir avec la lutte avec frappe. Sa Thies nekoul champion du monde teh daan nala. Boy Niang bi daan Sa Thies Modou Lo dafko daan avec facilité. Modou mola meune aller-retour*

    • @modourokhaya9616
      @modourokhaya9616 14 часов назад +1

      Fotekna Modou moko meune aller-retour? Danio beuri mou daneko?

    • @Momaradia111
      @Momaradia111 14 часов назад

      Bayilene sokhor one championship nékoul 2e division comme championnat Angleterre Espagne …

    • @modourokhaya9616
      @modourokhaya9616 13 часов назад

      @@Momaradia111 tontouwo sama question deh. Damamné fo tekne moko meune? Sokhor yaw mikoy khalat yaako deff

    • @Momaradia111
      @Momaradia111 13 часов назад

      @@kurayahmi rero wouniou dé gniy minimiser titrou Reug Reug témou wara nek fierté sénégalaise la diap ni sokhor la

    • @Momaradia111
      @Momaradia111 13 часов назад

      Pour mane Reug kene meunouko si lamb dji

  • @EssaBangura
    @EssaBangura 14 часов назад +7

    Modou lo Rek ❤❤❤

  • @moussabayo8554
    @moussabayo8554 12 часов назад +11

    One championship nga nék champion té fofou équivalent 2e division leuh. Lamb dji Modou Lô moy sén Baye

    • @idrissafall7940
      @idrissafall7940 2 часа назад +1

      Dou sakh deuxieme division
      1 er division ufc
      2 eme division pnf
      3eme division championship
      Paré dignou ray ak wakh

  • @modoulo4004
    @modoulo4004 14 часов назад +6

    Reug reug saxol be mou bonne ❤

  • @mamadoudione8917
    @mamadoudione8917 15 часов назад +13

    Reug Reug naak depuis l'ore nite yi niougui rafetaal D. One Championship n'est même pas reconnu pour sa ligue MMA, champion du monde ONE CHAMPIONSHIP en MMA dou daara, redescend sur terre.
    ONE CHAMPIONSHIP est une ligue de Kick Boxing, ay Pa you dièkhaal niofay combattre en MMA

    • @ibrahimahanne6906
      @ibrahimahanne6906 12 часов назад +1

      Saay yangui dioum dh ufc moy le plus grand organisation mma one championship nga beugone wax fofou la reug nek pas ufc

    • @mamadoudione8917
      @mamadoudione8917 12 часов назад +2

      @ibrahimahanne6906 one championship oui j'avais même pas relu pour voir mon erreur. One Championship car Reug Reug est là-bas. One Championship est plus connu pour sa league de kick boxing. Reug Reug neeu yaarou, les sénégalais niougui raafeetaal tei nopi, Champion one Championship bou dèmer ufc il n'intégra même pas le top 15 de sa division.

  • @kanejr7260
    @kanejr7260 8 часов назад +3

    Reug Reug est ingrat

  • @mohamadoumoukhtarcisse9043
    @mohamadoumoukhtarcisse9043 8 часов назад +3

    Une fois Roi, reug reug va glorifier de ce titre 😢😢?
    Faut valoriser tes adversaires pour avoir du mérite.

  • @DjibySy-h3f
    @DjibySy-h3f 15 часов назад +10

    Reug Reug Bayil nagou bi
    Daga fokné khamougnou
    Modou Lo dou sama Mbeur Mais doussa Morom cii lamdj
    Encore une fois Bayil Nangou bi

  • @CissIsmaila-r9r
    @CissIsmaila-r9r 12 часов назад +8

    bilahi modou lo moy ndanan mom rèk mofi nèk roi thiow bi beuri gnithi beugeu diote diko minimisè😅

  • @falloukonta1674
    @falloukonta1674 15 часов назад +12

    Ms reug reug mii eske wérna vraiment 😢

  • @Chiekh.mouhaiminou.wouldou.
    @Chiekh.mouhaiminou.wouldou. 11 часов назад +6

    Champion du monde yombouna troop si sénégalais yi

  • @libasselahi
    @libasselahi 12 часов назад +5

    Reug reug mii weroul dh😁😁😁😁

  • @yazalazadiallo
    @yazalazadiallo 2 часа назад +1

    Le combat que tout le monde attend c’est Modou Lo vs sa thies un point c’est tout

  • @MouhamethSy-g8g
    @MouhamethSy-g8g 16 часов назад +19

    Modou lo doussa morom

  • @yaramfall6996
    @yaramfall6996 8 часов назад +3

    Reug nekhoul ba nekhoul mais dofff deugu la
    Ils m'énerve communication zéro Putin diangual wakh gnou beuri gnogui lay méré ndakh niguay wakhé

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 14 часов назад +8

    Reug reug iaw ak tapha tine combat la kousi daan dieul sén papa modou lo le roi👑 😂😂😂

  • @MouhamadouNdiaye-d4m
    @MouhamadouNdiaye-d4m 9 часов назад +3

    reug vraie dof leu

  • @CASI7797
    @CASI7797 6 часов назад +2

    Coalition anti modou lo mofi dadjeii dh on dirait😂😂😂

  • @cheikhmbacke2841
    @cheikhmbacke2841 8 часов назад +3

    Reug reug champion du catégorique bou ndaw bi ga négue

  • @MaguetteSall-v9m
    @MaguetteSall-v9m 9 часов назад +3

    Balla gaye moy sama mbeur wayé reug reug mi dafa sokhor Modou moy roi 👑 nga nangou wala nga bagne

  • @moussaomardiaham4727
    @moussaomardiaham4727 15 часов назад +1

    Merci reug reug très belle analyse

  • @malickseck950
    @malickseck950 13 часов назад +1

    Modou❤moy sa mbeur dé mais dieul reug reug c'est le moment où jamais

  • @MameCheikh.
    @MameCheikh. 8 часов назад +2

    Legui reug dieuleul Tapha tine😂🎉

  • @modousarr8848
    @modousarr8848 8 часов назад +2

    Boy yaroul Modou Moy roi

  • @OuzinDiouf-g4e
    @OuzinDiouf-g4e 15 часов назад +7

    Yow mom doo gawa beuré Al modlo 👑

    • @Auxservices-w4n
      @Auxservices-w4n 56 минут назад

      Lolou probleme Modou Lo pourtant Franc wakh na Eumeu sene louco gueuneu grave

  • @Bamba-rk
    @Bamba-rk 16 часов назад +14

    Reug Reug nak prouver goo sa entrée sa grand yi dh
    sa palmarés ci làmb nekkoul lou extra-ordinaire dji
    tu reste un grand champion nak. mbeur meunoula ci làmb nak mom mais beuré goo fi combat risk

    • @kefgg
      @kefgg 11 часов назад +1

      Combat contre Gris 2 douwone combat risque ? Boul faténi diamono yoyou Gris 2 dafa nekone si dynamique de victoire pendant 7 ans meusoule won danou gneup ragal ko ame dolé nek super lourd nek jeune comme Reug Reug. Lolou combat risque lawone si Reug Reug.
      Sa Thies tamit combat risque lawone mais reug dafa danou. Combat Boy Niang bi di gneuwe tamit combat risque leu si Reug

  • @ThioroFall-s8h
    @ThioroFall-s8h 14 часов назад +5

    Modou lo kén menouko calculer ba sén beuss taxaw gay comprendre reug reug ni modou lo dou nioniou gua danne
    Franc mi dokh sen digenterk dégenté Thiow li yalna franc bayi modou lo mou dieul leu gua xam ni do dra reug reug si kanam modou lo

  • @lakhad09officiel36
    @lakhad09officiel36 3 часа назад +1

    Façon mousou ma nêx kii😢😢

  • @abdoulayesow4208
    @abdoulayesow4208 15 часов назад +3

    Reug reug vs tapha tine combat la

  • @sambadiouf9121
    @sambadiouf9121 15 часов назад +1

    Champion reug reug késsé 💓

  • @DethieDioufFissel
    @DethieDioufFissel 2 часа назад

    Champion du monde est mieux que Roi des arène 1000fois.REUG REUG à raison ❤❤.

  • @disytbi8711
    @disytbi8711 16 часов назад +11

    Reug reug bane vip la dane apart Bombardier bou am 50ans ?😂😂😂😂

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 16 часов назад +1

      Gouygui vip leu

    • @SaliouGueye-i8h
      @SaliouGueye-i8h 16 часов назад +2

      Bombardier mo dane balla ak modou😂😂😂😂😂

    • @senegaleventschanel6913
      @senegaleventschanel6913 16 часов назад

      @@Mbodji-walogouygui kegne la nek vip? Tapha Tine rekk lafa beurel te claf mo takhone

    • @ibrahimaba3553
      @ibrahimaba3553 15 часов назад

      Gnimou dane gneup yow sa mbeur daléne di moytou gni gueuna naxari dane si lamb ji la Reug Reug dane un champion doit être protéger Siteu bimouy gneuw di nokha Modou lolou koum fi dane pour meuna def lolou Modou Lo xamoléne sports moy lane 😂😂😂

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 15 часов назад +1

      @@ibrahimaba3553 wakhnga deug Modou Lô day moytoul rk😂😂😂

  • @papemalicksow994
    @papemalicksow994 15 часов назад +1

    Merci reug

  • @NdiayeIssa-fo1tr
    @NdiayeIssa-fo1tr 13 часов назад +3

    Reug reug yaw modestal touti

  • @assanecissfouloume8235
    @assanecissfouloume8235 15 часов назад +4

    Ki dou Champion du monde ki champion sur la Moy 3sem division Moy sén tu Bou mou gany

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou6545 16 часов назад +5

    Merci beaucoup reug reug champion de mond

  • @ibrakane5932
    @ibrakane5932 12 часов назад +3

    Reug championchip nga gagné nékagoo au sommet

  • @djimbaniang2190
    @djimbaniang2190 15 часов назад

    Maramdji da xam lamb nak reug reug ❤

  • @OusseynouDiop-d5y
    @OusseynouDiop-d5y 11 часов назад +3

    Goor dou beuri wakh

  • @saliougueye9833
    @saliougueye9833 8 часов назад +1

    Reug mi eskeu cv

  • @SokhnaastouSeye-t1v
    @SokhnaastouSeye-t1v 8 часов назад +1

    Reug reug champioship du monde leu championschip gni xam chanpionat engleter xamnaniou ni lolou mooy 2ém division
    N'a lér

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 10 часов назад

    Reug Reug actuellement ny
    Moo geuneu chér Modou lo foufff
    Modou lo champion Sénégal 🇸🇳 la mè Reug my champion du Monde 🌍 la Reug wallahi Moo Meun fouff Modou Lo🥹Reug champion ladé pur sax

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 14 часов назад +2

    Reug reug mbeur dou complet yagui ni daga ragal khéxx😂😂😂

  • @SaliouGueye-i8h
    @SaliouGueye-i8h 16 часов назад +1

    Rueg rueg ndanane la ❤❤❤

  • @moussadiakhate4063
    @moussadiakhate4063 10 часов назад

    Kon la nk mais reug moy lamb il est pertinent dans la lutte

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 14 часов назад +4

    Reug reug dof bou software la mé modou naw lowoula mo takh meusoulo wakh bamou tontoula modou dou tontou dof

  • @malickseck950
    @malickseck950 13 часов назад

    À mon avis pour man Modou ❤balla gaye amoul enjeu si nioune supporterou Xlo❤vraiment

  • @DoudodiengDoudo
    @DoudodiengDoudo 14 часов назад +4

    Beugone na commentaire mais sama xol mo mako mayoul nakh émission bii journaliste amougnou Fouleu ay doof rk gueine invité

  • @xelcomdecorationsopeserignesal
    @xelcomdecorationsopeserignesal 16 часов назад +47

    Champion du monde amoull si lamb

    • @moussapayemane4167
      @moussapayemane4167 16 часов назад +4

      Pourtan lamb dji amoul roi ndah CNG niowahné validé wouniou roi bi 😂

    • @xelcomdecorationsopeserignesal
      @xelcomdecorationsopeserignesal 16 часов назад +7

      @moussapayemane4167 yaw nanall galass 🤣

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 16 часов назад

      ​@@moussapayemane4167 Amna roi kay Siteu leu Yalmine bi👑💪🏾

    • @PendaTalla-c5z
      @PendaTalla-c5z 16 часов назад +6

      ​@@moussapayemane4167Nékouniou MMA

    • @SaliouGueye-i8h
      @SaliouGueye-i8h 16 часов назад +2

      Rueg rueg ndanane la bayil sissou😂😂😂

  • @oumarndao7485
    @oumarndao7485 14 часов назад +3

    Saway bou wahé rek ngua découragée 😂😂😂

  • @BocarAnne-g7d
    @BocarAnne-g7d 4 часа назад +1

    Bilay dof dofloul beu dieul avançou Nganou rek xol dinga xamni meuno MMA dinala kateu ba nga eumbeu

  • @elhadjigorasall5512
    @elhadjigorasall5512 15 часов назад +4

    Reug Reug soof na nak té khamoul 😂

  • @ibrahimaba3553
    @ibrahimaba3553 16 часов назад +1

    😂😂😂Sénégal mo nékh deh wa Siteu kone foum diaar est ce que mo gueune palmarès Reug Reug gnii Reug Reug dane Siteu dafléne dane est ce que talent dagne ko wara protéger mais lamb ji mo barii lobby koi😂😂😂

  • @elzo1836
    @elzo1836 6 часов назад +1

    Saway ngamouna 😂

  • @terangatv2678
    @terangatv2678 14 часов назад

    Ya woor t kham beuré macha allah....

  • @PendaTalla-c5z
    @PendaTalla-c5z 16 часов назад +4

    Reug Reug mome soff la déf ak sokhor

  • @SeydinaNdiaye-gs1ox
    @SeydinaNdiaye-gs1ox 9 часов назад +1

    Reug reug wakh meunoussi dara’’wornayalah reug iow boul wakh del beuré rek😂😂😂..nonou lagne la beugé..continuel ninga dane wakher manam damay nhieuw daane nhieupeu dem😂

  • @SouleymanevSy
    @SouleymanevSy 9 часов назад +2

    Ki mom da doff 😂lamb nga bole ak mma😂

  • @OusmaneKanee
    @OusmaneKanee 9 часов назад +1

    Communication dra ba legui dra dra blh

  • @BuurMbaye-n7y
    @BuurMbaye-n7y 3 часа назад

    Reug reug seul 🎉🎉🎉

  • @xelcomdecorationsopeserignesal
    @xelcomdecorationsopeserignesal 16 часов назад +3

    Reug reug yaw do touss 😂😂😂

  • @Baaliou-t9l
    @Baaliou-t9l 15 часов назад +3

    Reug reug doof la moom dey wakh ba yeuy bopam😂😂

  • @Seneami
    @Seneami 12 часов назад +2

    Hor sujet 😂😂

  • @Idyxaragnelo
    @Idyxaragnelo 10 часов назад +1

    Deemal dieul sa revanche si Sa Thies

  • @DjibySy-h3f
    @DjibySy-h3f 15 часов назад +2

    3/4 combat ganane champion du Monde Boul dof

  • @BadaraMbaye-s2y
    @BadaraMbaye-s2y 14 часов назад +2

    Arrêtez de tendre les micros a Reug Reug il est fou à lier doublé de quelqu'un qui n"a rien compris.

  • @Dpp205
    @Dpp205 15 часов назад +2

    Reug reug ken khamoul loye wakh

  • @momoofficial1988
    @momoofficial1988 11 часов назад +2

    Ma beugeu djiko modou lo deugeu dou tontu kèn

  • @Mouhamedba-1975
    @Mouhamedba-1975 16 часов назад +6

    Reug Reug il est sans modestie

    • @senegaleventschanel6913
      @senegaleventschanel6913 15 часов назад +1

      Wallahi je l’ai toujours dit ki badola bou alale dape la bilahi , depuis bamou wakhe à son rencontre avec Ngannou mome ladiouko numerom plais c’était Ngannou à lui avoir demandé son numéro , lolou loussi diare wakh ? Même boko ladione numerom sakhe nga wakh ko wagniwoula dara nak c’est un champion hors paire .

    • @ibrahimaba3553
      @ibrahimaba3553 15 часов назад

      Motay gueume bopam yék nék léne si ay émotions rek yakarni lolou moy adina nafékh baxoul
      En plus yow yay badola bou mak bii ndakh beugo Jambar

  • @malikking4291
    @malikking4291 14 часов назад +1

    Modou Local, Reug international. Deug nèxul

  • @Ibrahimandiaye2221
    @Ibrahimandiaye2221 14 часов назад +1

    Reug reug vs tapha tine

  • @MoussaNiang-iz4rh
    @MoussaNiang-iz4rh 2 часа назад +1

    Khanà Modou lo rek moye mbeur😂

  • @CheikhououmarSow-l4x
    @CheikhououmarSow-l4x 15 часов назад +2

    One championship la dé reug pas champion du monde des poids lourds na lere

  • @NdeyekhadyMbjoue
    @NdeyekhadyMbjoue 11 часов назад

    Yene khôl léne li reug reug wakh mo geune 😢bilakhi modou lo sou dieulé reug reug danou

  • @babacardieye7472
    @babacardieye7472 11 часов назад +2

    Non vraiment Reuk Reuk dafa sokhor

  • @DameThiaw-o8h
    @DameThiaw-o8h 10 часов назад +1

    Franc moy sa morom

  • @malickseck950
    @malickseck950 13 часов назад

    Makane dou dara sou beuger combat Modou ❤ reug reug na fay Xaragne 150 millions voilà

  • @CheikhNdiaye-l4q
    @CheikhNdiaye-l4q 16 часов назад +3

    Modou tapha kou dakor lalal j'aime,franc vs reuk reuk😅

  • @ng9ngagnisto517
    @ng9ngagnisto517 12 часов назад

    Reug Reug eumeu sene mo combat😊

  • @papasillytraore7777
    @papasillytraore7777 10 часов назад

    SA Thies Vs GRIS 2 🔥🔥

  • @mormboup9301
    @mormboup9301 Час назад

    Reug vrai ngaka la en vrai sens du termes ptain !

  • @momoofficial1988
    @momoofficial1988 11 часов назад +1

    Senegal modou lo len̈ yape rèk ..Tapha tine dou dieul si boy ..niome nieupeu nièmè nio dieule boy yi topou bèneu nite rèk

  • @Bamba-rk
    @Bamba-rk 16 часов назад +7

    wa legui gnoom gnaar nagn beuré kay

  • @GalleBa
    @GalleBa Час назад

    Moudou c'est une technique

  • @vieuxtoure946
    @vieuxtoure946 14 часов назад +1

    Reug reug yémal béne palace bari nga wax torope

  • @assanebabaofficiel3533
    @assanebabaofficiel3533 8 часов назад +1

    Fekhel meune si senegal mo geune 4 ou 5 combat niounane champions du monde ngay wax fofou amoul saf safal dhe 😂

  • @SeydouFall-f6i
    @SeydouFall-f6i 12 часов назад +1

    Champion du Monde arretel

  • @babacar3178
    @babacar3178 15 часов назад +1

    Kii mom wéroul😂😂😂

  • @tallatoure195
    @tallatoure195 46 минут назад

    Sa thies moy sa papa modou lo sa mame la 😂😂😂😂

  • @idrissafall7940
    @idrissafall7940 2 часа назад +1

    Pour vous dire
    1 er division ufc
    2eme division pnf
    3eme division championship et non reconnue dans le monde des mma ay pa you retraité rek niofa nek amoul niveau ex boucher ketchup loumouy oute foofu ?

  • @malickseck950
    @malickseck950 13 часов назад

    Staffou balla " Azziz " xallissam leu yoré beuge diriger lambj c'est pas normal Modou❤ akk staffam nio wara bagn lolou

  • @ElhadjiFall-nw2he
    @ElhadjiFall-nw2he 2 часа назад +1

    Yaw. Ing nane ngua nak😮😮

  • @MoukhamedCisse-i1i
    @MoukhamedCisse-i1i 9 часов назад +1

    Ki weroul

  • @AlphabouNdiaye
    @AlphabouNdiaye 13 часов назад +1

    Reug yaw danga reuy ou bien danga sokhor nioune fi lamb layou am