@ndongokandji5313 parce que Roi des arènes biwon Eumeu Sene mo beugone revanche contre Modou Lo. Modou Lo amoul revanche bi mouy jeul contre Tapha Tine. Mane foralouma Modou mais logique lamb lay wax.
@@mbenguecheikh6272 djouguè woul ci balla gaye dè nga joum. Ci bombardier leu djouguè fekk Eumeu Sene beug revanche ak mom. Kone bokoul ak cas tapha Tine. Le vrai combat royal c'est Modou Lo contre Reug Reug!
POUR LES 1 an, IL FALLAIT LAISSER LES PRÉSENTATEURS DE TOUJOURS C-A-D IBA KANE ET BOCAR. CE MOMENT PRIVILÉGIÉ EST À EUX. ÇA N’A AUCUNE LOGIQUE COMME SI IBA ET BOCAR VENAIENT PRÉSENTER LES 1 AN DE L’ÉMISSION DU JEUDI SOIR DE LAMINE. PEU IMPORTE LES QUALITÉS DE PRÉSENTATEUR DE LAMINE. SUR TAPHA TINE, MODOU N’A AUCUN DÉFI À LUTTER AVEC TOI. TT, TU N’A AUCUNE LÉGITIMITÉ À DEMANDER UN COMBAT AVEC MODOU NI À LE TAXER DE TAPET. APRÈS UNE TELLE HUMILIATION AVEC BALLA, TU AS TOUT INTÉRÊT À TE FAIRE DISCRET ET DONNER LA CHANCE AUX JEUNES. TAPET BUY DJENGUOU DAY NIANK XOROM, RAJOUTÉ À TON GNAKXOROM DE TJRS.
@ BO AMÉ LO XAM, GUA TEYEKO BAMA LATHIE LAKO. ON N’EST PAS SUR UN SARGAL OU HOMMAGE À QUICONQUE SUR UNE ÉMISSION RÉTRO OU DÉPROGRAMMÉ MAIS BIEN ACTUEL ET QUI SE POURSUIVRA. DONC N’EXISTENT PAS MIEUX PLACÉS QUE LES PRÉSENTATEURS DE TOUJOURS DE LA PRÉSENTER EN DÉROULANT UN PLAN QUI LEUR EST PROPRE COMME C’EST LA REGLE NON ÉCRITE DANS TOUT MÉDIA. ON EST SUR LES 1 AN DE L’ÉMISSION ET NON UN HOMMAGE OU SARGAL À QUICONQUE. ENFIN, CE POINT SOULIGNÉ N’EST QU’UN DÉTAIL SOMME TOUT IMPORTANT ET N’ENLÈVE EN RIEN LA QUALITÉ DE L’ÉMISSION DU JOUR. TONTU BAXNA MAIS WAXSILOXAM DAKO GUEUN.
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😢🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😢😢😢
Reug reug pour mom mo dakha beuré si lamb dji wathial sur terre
Tapha tine mom mo geuna niak diom si lamb dji
Modou lô daffa ragal tapha tine 😂😂😂
Bilaye deuegu Leu tapha Tine waroul Danou Si làmb mais nak Kou melni balla gaye Dano am fit
Gayi setlou woléne dara modlo dou wakh ba dioum toudd tapha tine 😂😂
Taille bi mon baxoul si môme 😂😂
Bane mbeur ngua guiss modou diko toudou à part wa parcelle
Tapha n'a outi mbollo prometteurs yi beugou niouko
setlouwo dara ?modou meussoul wakh ci mbeur apar bouniouko ladié modou nekkoul ci aay details...
Reug sawakh barina Modou sakaw leu djieum
Alkhamdoulilah yalla na co yalla def sou boba nga kham
Tapha Tine vient d'une défaite, ne mérite donc pas un combat royal pour le moment.
Iba da gueme bopam
Tapha tine Haral franc vs ama
Kou dane fofou ngeu djieul ko
Guelle bi meun na dh🎉
Modou Lo doit prendre tapha ou sa thies moy logique
Modou lo moy le seul roi bouy calculer😂
Ana nie kalkulé woul
@modousarr8848 balla gaye 2 eumeu sene bombardier tyson ak yekini
Modou Lo molen mane fouff
N'a jéll avanc ci kenu ci niom niar❤
Kou djouguè ci défaite manoul barè combat royal
Modou Lo janvier laka balla dioutal juillet mou nék roi😂😂wala khamokowône 😂
@ndongokandji5313 parce que Roi des arènes biwon Eumeu Sene mo beugone revanche contre Modou Lo.
Modou Lo amoul revanche bi mouy jeul contre Tapha Tine.
Mane foralouma Modou mais logique lamb lay wax.
Modou bamouy beuré royal si balla gaye la diougué di yaw khamo lamb d
Modou lo balla gaye la beurel pares beuré royal di yaw khamo lamb deh
@@mbenguecheikh6272 djouguè woul ci balla gaye dè nga joum. Ci bombardier leu djouguè fekk Eumeu Sene beug revanche ak mom. Kone bokoul ak cas tapha Tine.
Le vrai combat royal c'est Modou Lo contre Reug Reug!
Móodu lóo bàyyil tàppale bi te jël sa waay walla nga ni bëre wu ma ak moom mu leer.
legui beuréwouniou diekhna khana beuré force la?
Sa way nii manounio dane modou lô
N'a jéll reug ci mom la déss moy gena lèr bou siteu
@@KhadimThiam-pe7zy reug defagoufi dara danoufi béneu vip apart b52 50ans, siteu mome modou daka done dakué combat bi yeu boy bi di daw guinaw saccouyi rek, yéne ceen blém moy kou nekk n1 menolénko supporter modou bou danone sakh tapha balla reug , ngen wakh non na dane amanekh na dane sathies ect...
@@Deggou gris 2 Elton nio gniou dou ay mbeur. Siteu ak reug, kan mosi dahk palmarès, lou tah mou mayko chance .
Logiquement parlant modou lo dafa wara beurè ak tapha tine vraiment moy combat amateurs yi nione niarr rek nio lalègoule si sène generation moy vrai de vrai combat roiyale bi . Mais nak attention promoteur bou deugou beugueu lamb beugueu amateur mo meuneu dècrochè bobou combat .
saay combat royal kou dioiugué ci victoir moko wara beuré tapha na déme xool fénéne
Beuré woniou ak tapha poin
Buzz da yarou ndaye sane
POUR LES 1 an, IL FALLAIT LAISSER LES PRÉSENTATEURS DE TOUJOURS C-A-D IBA KANE ET BOCAR. CE MOMENT PRIVILÉGIÉ EST À EUX. ÇA N’A AUCUNE LOGIQUE COMME SI IBA ET BOCAR VENAIENT PRÉSENTER LES 1 AN DE L’ÉMISSION DU JEUDI SOIR DE LAMINE. PEU IMPORTE LES QUALITÉS DE PRÉSENTATEUR DE LAMINE. SUR TAPHA TINE, MODOU N’A AUCUN DÉFI À LUTTER AVEC TOI. TT, TU N’A AUCUNE LÉGITIMITÉ À DEMANDER UN COMBAT AVEC MODOU NI À LE TAXER DE TAPET. APRÈS UNE TELLE HUMILIATION AVEC BALLA, TU AS TOUT INTÉRÊT À TE FAIRE DISCRET ET DONNER LA CHANCE AUX JEUNES. TAPET BUY DJENGUOU DAY NIANK XOROM, RAJOUTÉ À TON GNAKXOROM DE TJRS.
Nitt du sargal bopam khamal lumala wakhul