Vraiment j commence a aimer zarko ,bilahi on peut le considérer comme le meilleur lutteur d l'année prk depuis son arrivé na pas eu de defaite.6 victoire successif. Machallah
Yaw bénn clé nga am ta billahi mo si dane eumeu wala ama teull bi nga am ta yalla nalla yalla may nga am eumeu force dallay dane amo beuré bouko dane ta bo khékhé mou doumeuleu
@@lafindutemps6141Zarco professionel leu, sou clé bi dokhoule mou essayer yénéne rek. Eumeu Sene meunoule contrer clé yeup quand meme. Guise nagn fi clé bi Modou dané Eumeu premier comba. Meme soudoule lolou Zarco meune na contrer Eumeu ba dane ko tamit comme ni Tapha Tine def bien que Tapha ak Zarco bokougnou gabarit
Tapha mbeur vs Jackson Fils de balla vs Moussa Ndoye Reug vs zarco Aliou seye vs eumeu Lac 2 vs Tapha tine Sa Thiès vs modou Lo Thiatou Daouda fall vs Mor Kang Diop 2 vs talpha
Jackson vs mbaye gouygui Fils de balla vs général malika(revanche) Reug vs zarko Seye 2 vs eumeu Tapha tine vs modou lo Sathies vs boy niang 2(revanche) TDF vs Tapha mbeur Gouygui vs gris bordeaux Talpha vs diop 2
zarko même so danone vip yeupp doutakh nga raw sathies si lamb pask mola dane té ñîmou dane danoléne gris mi nga dane pa la da dièkhal danga tapét rek mtx do nangou dieul sathies
Liguèye bou worr ak fiit gueume bopam motah zarko di ame name en plus dèy nèkhale lamb machallah yalna yalla gueune lérale yone bi 🔥💯💪
Bilahi frère tu as raison, en plus neik bay fall. ❤❤❤❤❤
Zarco liga sool rafet na trop ❤
Zarko nouveau VIP ❤❤❤ inchallah dam reck Fran VIP ❤❤❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Vraiment j commence a aimer zarko ,bilahi on peut le considérer comme le meilleur lutteur d l'année prk depuis son arrivé na pas eu de defaite.6 victoire successif. Machallah
@@aboubacarsy8643 depuis son retour
Zarko eumeu séne kou d’accord 👍
Eumeu deih dou may chance zarko geumoumako
@@salious1476 Pourtant legui combat bi tahaw
Dabel nguel yo arr minn mbada namo baggage 🧳 😅😊 tous les halpoulars derrière toi je suis de Thilogne je vous suis depuis USA 🇺🇸
Thiey sama gniari dome baye hii yalla s'en diammou yag waye machalla depuis en France 🇨🇵🇸🇳😀😀😀🤣🤣🤣🤣🤣😭❤🤲🤝✌👑👑💪💪🔥🔥🙏🙏
Merci peul ak zarco poular bi nekhna on njaaraama ❤
Zarco domou toucouleurs yi💪🏾 so ari mi arat so jaggi mi jaggat😂
A diarama poulo ....tout le monde weltiké... excellente et victorieuse continuation
Zarco dal mongui nekhel lamb😂😂😂❤bne continuation
Felicitations bad boy Zarko 😁😁😁😁😁💪👍🙏😁
Billahi meuna dane kouné sama guis guis mouy fitam entraînements bou diari yone té da meuna beuré machallah kouko dieul dinko bayi khel
Zarko un vrai sportif leu machallahh
Merci beaucoup waa albourakh évents ❤❤❤ félicitations Zarco mé encouragements à Gris Bordeaux ❤
kii koumou diape lékk Ndayem 😂😂😂danoule lambe mais légui thiédo la 😂 Dina fi reye ndaye mbeur😅
Ndeysan Zarco dafa begue Modou Lo motah légui lépam si entraînement lako ték légui
Félicitations à Zarco !
EUMEU VS ZARKO LAMBE DOUKO DAKH
Félicitations champion,yo allah seliin,sembina,ha yesso ko lawol.a Jarama.
Mbeur nala eumeu sene may chance
Zarco yày goor💪💪💪😂😂♥️♥️♥️
Moy lamb dji dai emeu sen zarco kesse moy lamb dji boul dieul sakh sa thiesss dieuleul eume fayekou lou beri dem def si air plus bou bakh😂😂❤
Ya bakh bilahi
@@adamandiaye5622 ya rafet khol bilahi
Félicitation mbeur
Félicitations❤❤
Zarko dèffa gueum boppam am foulla am fayida beureu foulla reekkk mokoye dèfffffffffffff
Peulh bou refef ❤❤
Zarko ❤❤❤
Alhamdoulilah ♥️😍
Zarco c t une machine de guerre catarpilard il sait coma demolir desorme yaye borom ndakarou
Policier yii zarco moyy senn mbeur😂😂
Bilay frére zarko bou nieuwé rék daléne di physique lo 😂😂😅
Alkhamdoulilah
Merci beaucoup champion zarko
Zarko vs reug reug
Zarko vs Eumeu sene
Zarko vs Eumeu Sense 🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍💪👍💪😁 The world need,,,,Modou lo vs Sa thies 🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍👍💪😁💪🌍🌍
Zarko mi mounna am lounè ci lambeu deffa am foulla am fayida
Zarco bo dofoul ni mom doko dane dh🤣🤣🤣
Zarco wagaaa leu Wagaaa 😂 té mbeur bou waga ni mom rek moko meune dane
Bravo zarko poêle ❤❤❤❤❤
Yaw bénn clé nga am ta billahi mo si dane eumeu wala ama teull bi nga am ta yalla nalla yalla may nga am eumeu force dallay dane amo beuré bouko dane ta bo khékhé mou doumeuleu
Baayil di wahéé émotion, té dou yaw yaay beuré, kii keppou kou kham lamb, khamné dou niééhou niébéwou kenne et on verra
@@BounamaDiarra-o8p zarko lay faral dèh inchallah mais clè bobou manoul dane eumeu sène déh
@@lafindutemps6141Zarco professionel leu, sou clé bi dokhoule mou essayer yénéne rek. Eumeu Sene meunoule contrer clé yeup quand meme. Guise nagn fi clé bi Modou dané Eumeu premier comba.
Meme soudoule lolou Zarco meune na contrer Eumeu ba dane ko tamit comme ni Tapha Tine def bien que Tapha ak Zarco bokougnou gabarit
Zarco meunoumako khol teh douma reh kon na 😅😅😅😅😅
Zarco vs eumeu sene combat la nak
zarko mou geune sonal policè yi bilahi ms diambar la 😂😂😂😂
Mom day neikhal lambeu😂😂😂
Thiate boy bambara ada fass mbaye gouye gui diene kairé gris bordeau non zarco sonal na wa ndakarou
Zarco & Reug Reug moy combat bi
Masha’allah proud fulas
ARGENTINA ❤❤❤❤
Télaaaaaa yéwwwww🎉🎉
Zarko Kesse 👍😂😂
Tapha mbeur vs Jackson
Fils de balla vs Moussa Ndoye
Reug vs zarco
Aliou seye vs eumeu
Lac 2 vs Tapha tine
Sa Thiès vs modou Lo
Thiatou Daouda fall vs Mor Kang
Diop 2 vs talpha
Jackson vs mbaye gouygui
Fils de balla vs général malika(revanche)
Reug vs zarko
Seye 2 vs eumeu
Tapha tine vs modou lo
Sathies vs boy niang 2(revanche)
TDF vs Tapha mbeur
Gouygui vs gris bordeaux
Talpha vs diop 2
Athia zarko min beltima
Nooo vramint sarko mérite na trophée 7 victoire yo matol 3ans
6victoire
6 victoires leu
tél tél télaaa yéwouuu reck
ZARKO 🥊 REUG REUG...ndax mou gniam toûti MMA
Sarco❤❤❤
Bb Diéne même s’il est guéri
Yaw ak mom dou combat franchement
Bouga reg reg du bagne bb diene. Moko signé
Bilahi diga xamne'. Jamaîcain ga amal contrat
Tous nak Delo xalis kana amoul mom lye neex
Zarco vs eumeu sene demande national❤
😂😂zarko nena combat yimou danou yeup dane ko xeex khana yinga dane kon danio xeex sa adversaires yi
Wawaw kou wakh li wara wakh la thia déss😂
👍❤️❤️❤️
zarko même so danone vip yeupp doutakh nga raw sathies si lamb pask mola dane té ñîmou dane danoléne gris mi nga dane pa la da dièkhal danga tapét rek mtx do nangou dieul sathies
Bro sa mo bagne
Dou Sa Thies mo bagnone ? Boul faté. Zarco lathie nako Sa Thies bagne di indi ay khoulo kone affairam leu
Say waho lou am dé
Sa thies pa moko dane dé boul faté lolou
Saway Zarko éksineu dé nanouko nangoul rék Sa Thies instant bi Zarko amoul loumoukoy nawé
Eume AK reuk reuk bayilne fi dem seti lenene mo guene gno meune thi lambdji actuellement
Zarco Euneu Sène combat bou nekh!
Bakane seulh sa ari mi arat sa arani mi arat zarcko dofla dé
J'ai bien zarco
Wamé aussi c normal gua dané gris ni parce que mougui Fin carrière ! Mais félicitations à vous deux
🎉🎉
Zarco rek
❤❤
😂😂zarko sonal nga policé yi
Reug reug SA baye la Bro
Amo khel
❤❤❤❤❤❤
Zarko dou Nit 😂😂😂😂😂
🇨🇵🇨🇵🇨🇵🇨🇵🇸🇳🇸🇳🇸🇳❣❣❣❣❤❤❤❤
❤
🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Sa thies na dieul zarco
No lolou dou combat bi zarco emeu séne wala tapha tine ou reug reug
Il faut être ambitieux dans la vie il ne faut surtout pas prendre pokola boy yi ngay bayi t beuré si kawwww ak gua yi si kawwww voilà
zarko alanda bopou dem😂😂😂
Zarko vs Eumeu Séne
Thiéy sama viking bi ya woor déh
Zarco ak Eumeu sène moy combat bi bou béneu promoteur khol lou sori li moy combat bi
Zarco vs Reug Reug
Gris Bordeaux mi man sakh mounouma daan 😅
Adiarama
Nervi mbeurr
Les deux invaincus Zarco & Reug Reug combat bou nékh taille yi tolonagn forme yi niro nagn té niom niar nieupa deuguar
🇨🇵🇸🇳🇨🇵🇸🇳
Ki daffa eupeul vraiment
Xana nekhoula 😂
@senegalrek2579 c pa nékhouma mais na dale touti et changer communication seulement c un grand champion
Reug Reug bou dieloul combat bi dafa ragal na défni Ama baldé beuré avant son prochain date comme combat wam ak Boy Niang amagoul date
Zarco Baboye rek lamèye fatali même physique redoutable et dangereux
Lou lér
Eumeu wona morome ma
Zarko jamaïcain da bari histoire dh ya yoor contrat wam😂
Zarko Gouye Gui 😂
Yaw nonou gouy gui nga
@@Domou_Deukk_Bi😂😂😂😂
Reug dalay lék d3
Kénn khékhoula li ngay déff niémé woko déff wa pikine
Comme lane?
Faraloumala mais kou beuré woule ak yaw da ragale boule gnane kéneu chance danga ékssi
aka khadiam té saleté mdr🤣🤣🤣
Pawlish nena dafa khasaw te bopbi reyna 😂😂😂😂😂😂😂😂
Lou mbeur douniou laath tapha tine😂😂 même bouniouko Ladjé dOunioU si sOrrii
@@abdoulayemboutouFall kane Abdou Jambaar
Comba eumue sene VS Zarco SA touba la si nara saga ba am bakar
😂😂😂😂
Sofademé fekeufa Sérigne Ndiaye 2 et gris 2 wala général dinagn la nokhou banga saww😂😂😂
Diambar Iow doyalo Si Zarko Iow ?