Serigne Khadim Thioune (Espagne) sur le lieu d’inhumation de Cheikh Béthio Thioune : ...»

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 14 янв 2025

Комментарии • 620

  • @sunugaalsenegal7069
    @sunugaalsenegal7069 5 лет назад +126

    Machallah lii bettouma. un jours javais vue serigne touba et chiekh ibrahima fall et serigne saliou et chiekh bethio dans mes rêves sur un pont cetais a touba billaahi wallaahi et moi je suis tidiane wah ngir yalla rek machallah. yalla nako yalla yeureum

  • @magatteka8124
    @magatteka8124 5 лет назад +93

    Akassa dieureudieuf .il est très responsable, kadouyou rafetna

  • @leppmoomlawaxlurafett7616
    @leppmoomlawaxlurafett7616 5 лет назад +20

    Machallah
    S khadim mii de mane naw naako loool ndakh DALL GUI AK NITÉ GUI AK XAM XAM BI...
    yalla naleen yalla sammu te mayleen werr...
    Nii rekk la, yeen ñaboot gui bou leen kennn defloo lou wouték dokhinou yoon wi
    NDIGEULOUL SERIGNE TOUBA REKKK

  • @tewloumatv2514
    @tewloumatv2514 5 лет назад +18

    Machallah un vrai responsable serigne khadim dieureudieuf thioune lepp rafetna

  • @AminaAmina-nv2iv
    @AminaAmina-nv2iv 5 лет назад +1

    Masha Allah ndiabotou serigne bèthio man dé douma mourite layènne la wayé masha Allah lou thiow bari bari am nguèn yare am nguèn tèguine sèn baye yaar nalèn masha Allah, kèn dègoulèn ci bèneu wakkh bou niaw, kèn dègou lèn ci ay kheuthio kèn dègoulèn ci tésseunté bilahi am nguèn ak daal tèye nguèn boudoul dara respect bi nguèn am si sèn sokhna baye yi ab ndiangate bou rèy la ci dieulé ndakh diabarou baye loumou touti touti sa kilifa la, masha Allah yalla nallèn yalla mouthieul ci seuytaané dolli lèn soutoura aduna ak Allah hira ci sèn barké baye ak sèn liguèyou ndaye ay réffèrences nguèn bilahi, wakh sa mbakhou way dou waagni dara sisa mbakh, serigne bèthio yalla nako serigne saliou térrou térralko bèrndèlko comme nimouko ndaan défé ci kaw souf, wakhou Mala liguèyeul serigne touba rék waayé domou Adama yi don lèkeu niakam rék dougeul nako aldiana ndakh diokh ab dioulite bou khiif mou lèkeu ba soure mo euppeu nga tabakh diouniy diaakeu man dé bima nèkké xaalé nèkon sénègal don na guis ay niit di dèm Gamou cheikh bèthio pour lèkeu ba tibeu dèf si mbousse moussumako guiss waaayé kham na domam maame khadim thioune bima dernier vacance lako kham mais kou bakh té am taalibé am yaar té modeste masha Allah

  • @Elzodhino
    @Elzodhino 5 лет назад +6

    Ndeysaane Serigne Khadim mii vrai goor YAllah la mashAllah am nga talibè lol dooko messa rèthiou 😍 Cheikh Bethio yalnako Suñu Borom wanalé ak Serigne Saliou thia Aldjannah Firdawsi 🙏🏾

  • @cheikhkhaya9034
    @cheikhkhaya9034 5 лет назад +41

    Ndeysane wakh djii rafetna dh thioune bilae yalna diamou yague cheikh yalna yalla yokou ay lèram barke borom touba

    • @mamaafrica8193
      @mamaafrica8193 5 лет назад

      Très beau même, intelligent, posé et bien éduqué

  • @massdiopmc
    @massdiopmc 5 лет назад +2

    Un discours posé,discipliné , plein de sens, d’éducations machalla je ne te connaissais pas mais tu m’as ému , c’est ça qu’on appelle tout simplement un RESPONSABLE,Cheikh Bethio yalla nako yalla terou aldiana, si barkè Serigne Touba Serigne Saliou

  • @cheikhissa1
    @cheikhissa1 5 лет назад +78

    Serigne khadim Thioune vous avez tenu un discours responsable d’un vrai disciple Mouride . Ndigel jëffe

    • @lamaranadiallo8418
      @lamaranadiallo8418 5 лет назад +2

      Wakh dji rafétna Thioune Mame BAMBA Doundel way ....

    • @gueyeteragna9982
      @gueyeteragna9982 5 лет назад +1

      GÉWËLU XAADIM billahi

    • @ndeyemboup4299
      @ndeyemboup4299 5 лет назад +1

      Géwëlu xaadim mane deh damako beugue lol tei beugue ko guiss! Machallah

  • @serignembackediop1773
    @serignembackediop1773 5 лет назад +121

    Fou way nèk yalla ngui fa Mohamed mongui fa serigne touba mo ngui fa mame salliou mongui fa yalla nako yalla kharé alldiana

  • @etiennesnciss9556
    @etiennesnciss9556 5 лет назад +71

    Suis catholique
    Je le vois très posé et intelligent

  • @peulhbourafet4423
    @peulhbourafet4423 5 лет назад +38

    Machalla wakh dji rafetna ame yaare ak téguine c tun responssable bilahi

    • @bounabanno6961
      @bounabanno6961 5 лет назад

      Wakh n'ga deuggdé kii dafa yaru lool lool..... ab talibé deuggla !!! Yalla bumu yakhoulé.

  • @codoufalldieng3563
    @codoufalldieng3563 5 лет назад +16

    Dieureudieuf wakh dji raffettna paix à son âme et la terre sainte de touba lui soit légère amine

  • @azizndiaye7674
    @azizndiaye7674 5 лет назад +3

    Franchement la communauté mouride vous êtes des références quelle discipline exemple pour tous le reste

  • @mormbaye6730
    @mormbaye6730 5 лет назад +6

    Machalah Thioune que le bon Dieu vous protège et toute la famille de Cheikh Béthio Thioune
    Repose en paix serigne Cheikh

  • @khadycisse5726
    @khadycisse5726 5 лет назад +22

    Machalah Thioune mame bambi mane dale serigne khadime mi .nekhnama dafa khame wakh diou rafet te meune ko douma thiantakoun dee waye mom Machalah

  • @ibrahimasy5377
    @ibrahimasy5377 5 лет назад +31

    Cheikh béthio sa domm yi yiw nagnou yarou nagnou am nagnou talibé, raw ga gnépp

  • @2mvisionsenegal884
    @2mvisionsenegal884 5 лет назад +2

    Miinou mala deh, wayé sopp nala lol ndax kaddou gou sell gi té mourité, dal gi machalah🙏🙏❤

  • @Defunity
    @Defunity 5 лет назад +2

    Tous les filles de Cheikh Bethio que j'ai vu parler sont d'une maturité et modestie exemplaire, je le salue. Je suis Niassen mais beaucoup de respect pour ce comportement. Sénégal leup ben leu naniou dokh jam rek.

  • @camaracamara9259
    @camaracamara9259 5 лет назад +1

    Macha Allah. Sa wakh rafétna .

  • @seydinagueye5528
    @seydinagueye5528 5 лет назад +13

    Je t'adore serigne khadim tout simplement

  • @adamafaye7118
    @adamafaye7118 5 лет назад +9

    Machalla serigne khadim je t’adore bcp

  • @laminetine307
    @laminetine307 5 лет назад +19

    seringe khadim thioune yalla nala souñiou brom same taxawou la té arre la mane dé xamou mala wayé sope nala nguirr nangou ndigeull gui yaw dé khawma kan wayé yaw kou guindékou nga yaw yalla naga fy yageu

    • @astoundiaye5698
      @astoundiaye5698 5 лет назад

      Ha ki beug naco waiyy machalla long vie à toi bialy mourride ndiguel nitte cou bakh daiyy ame kilyfa vraiment tué poli

  • @papedjiby1354
    @papedjiby1354 5 лет назад +1

    Dieuredieuf Serigne Khadim Thioune
    Mouride NdigueuL

  • @serignebassiroudiop8772
    @serignebassiroudiop8772 5 лет назад +5

    Mane dh wallahi sop nala loll thi yarwi ak teguine ak dieufé ndigueul wi nga khamni monou fii bayi dileu masta wou loll thi tiss wayé sap Mouride manshallah S. Khadim

  • @djilyniand6226
    @djilyniand6226 5 лет назад +14

    Waye seringue khadim thioune guoudal fane 🙏🙏🙏

  • @marigueye5615
    @marigueye5615 5 лет назад +5

    Wallahi c vrai merci beaucoup yalla nako yalla yeureum amine yaraby tout mes condoléances a la famille

  • @abdoukhadretop255
    @abdoukhadretop255 5 лет назад +3

    Macha Allah wakhdji rafetna Yallah cheikh saliou terrou si barkém

  • @khadimdia2213
    @khadimdia2213 5 лет назад +1

    Cheikh Bethio leppu lumou am ganaw yallah Serigne SALIOU bakhmila th serigne SALIOU S.Touba moye wadiouram S.Touba nk S.Mounatakha mokafai nekal (((mouride diaffé ndigal )))

  • @kaytabintou806
    @kaytabintou806 5 лет назад +7

    yaw dé je te connais pas mais kouma nékh nga. ndakh sa yarr ak sa dal ak sa nitté. kou ame talibé nga franchement😍

  • @senzanome9931
    @senzanome9931 5 лет назад +42

    Yalla nako serigne saliou terrou wonaleko ak khadimou rassoul

  • @serigneidalymbacke4169
    @serigneidalymbacke4169 5 лет назад +1

    Machallah kadou yi raféttna yalla na yalla yokou léram bijahi s.touba

  • @mbayeleye2303
    @mbayeleye2303 5 лет назад

    Serigne khadim yalla na la yalla samou nga sott sa papa aw fane kadou yi rafte na machalla amna solo yalla na léne yalla takhwo barké serigne saliou

  • @bayefalldiagneinfo8730
    @bayefalldiagneinfo8730 5 лет назад +42

    Vrai responsable nga

  • @bambaseck62
    @bambaseck62 5 лет назад +1

    Akassa ndigal dieufé serigne khadim yalla nalene serigne saliou teyel bopam cheikh bethio diamou serigne saliou yalla nako yalla dolly yeurmandé

  • @sawolamo
    @sawolamo 5 лет назад

    MachaALLAH YALLA n'a yégue gui woyof thioun Barké Serigne TOUBA, lép loy déf naga thi djiteul sa BOROM, teunkkou dji bdigeul. Serigne Touba nitou YALLA la, kou raggalone YALLA la, beug ko té doyloko beug Rassoulilah. Ngalla gnioune Mouride nagniou ko roy. Nagniou ragal YALLA téy rafétal. Mane déye thioune Serigne khadim Amna thi yow yakar.

  • @alkhamdoulilah518
    @alkhamdoulilah518 5 лет назад +2

    Serigne khadim mala beug billayi Amal jamu rek❤️

  • @ndananetv9010
    @ndananetv9010 5 лет назад +13

    Akasa thioune wakhe dji rafêt na machallah

  • @adamadia6005
    @adamadia6005 5 лет назад

    Dieu reuf thioune wakhdji.rafetna cheikhbi yalla nako yalla khare aldiana

  • @fallousow424
    @fallousow424 5 лет назад +1

    Vraimant votre parole est respectable. Que le paradis soit son dernièr demeur

  • @beuguserignefallou1966
    @beuguserignefallou1966 5 лет назад

    MACHALLAH yalla nala yalla defal diam s.khadime

  • @khadyndiayeyayefall9014
    @khadyndiayeyayefall9014 5 лет назад +14

    Dieureudieuf Sgne Khadim yalla naléne Serigne Saliou Mbacke takhawou thiant gui kanam rek la dieum

  • @fatimaaidara9713
    @fatimaaidara9713 5 лет назад +12

    Ki waliyoula motah youcoy heuthio macha'ala ❤️😭

  • @amdymf4642
    @amdymf4642 5 лет назад +2

    macheallah s.khadim diaradieuf
    s.mountakha mbacke bassirou yallanafi yegue te wer

  • @khadimpene7459
    @khadimpene7459 5 лет назад +1

    Akaza mame khadim kadouyi amna solo lole machala

  • @ndeyehenriettengom4966
    @ndeyehenriettengom4966 5 лет назад +1

    Je te félicite tu as bien parlé mashallah

  • @daoudawade9771
    @daoudawade9771 5 лет назад +4

    yalla nako yalla yeureum thioune kadou yi rafétna

  • @adamafaye7118
    @adamafaye7118 5 лет назад +17

    Vraiment diaboutou cheikh bii amnagnou téguine am khar machalla sene baye laa mourite djigual

  • @mbayeyatt9310
    @mbayeyatt9310 5 лет назад

    Machallah Thioune watie rafétena yalla na leine yalla sam tie barkép sérigne saliou

  • @antadtall4107
    @antadtall4107 4 года назад +1

    Serigne Mountakha Yalla naffi yagg té werr

  • @moramysylla3275
    @moramysylla3275 5 лет назад +25

    Amna Sólo Torop Yalla Na Ko Yalla kharrè aldianna Firdawssii Amine

  • @ayaseye5202
    @ayaseye5202 5 лет назад +66

    serigne moutakha ay wakham dieufé cheikh béthio soudone mome dakoy dieufé

    • @dexdexmen4525
      @dexdexmen4525 5 лет назад

      Yene bolene dokhewone loutakh gnou topoulene.amolene lolene wakh pression etat bi kesse motakh nguene changer décision.batalibeyi di tope serigne bi yene folene nekoone

    • @dexdexmen4525
      @dexdexmen4525 5 лет назад

      Yaw amoo Lo wakh.bo respectewone li cheikh wakh kone dinguenko yegué khalif bi

    • @killumastaexestunhypocrite7186
      @killumastaexestunhypocrite7186 5 лет назад

      Wa légui YALLA nak ??????🙄🤔

    • @ayaseye5202
      @ayaseye5202 5 лет назад

      serigne bi mangui diégalou bou bakh dieureudieufé serigne touba

    • @killumastaexestunhypocrite7186
      @killumastaexestunhypocrite7186 5 лет назад

      @@ayaseye5202 Adouna bi YALLA moko mom, adouna bi YALLA moy ki ko mom, Dieuredieufé YALLA SUÑU BOROM ☝️

  • @aliounefall2250
    @aliounefall2250 5 лет назад +1

    Bien dit Thioune un bon talibé dafay dieufé ndigueule

  • @freemanfreeman4465
    @freemanfreeman4465 5 лет назад +4

    Vraiment les fils de Cheikh Bethio Thione sont très éduqués mashallah

    • @abiesagna6622
      @abiesagna6622 5 лет назад

      freeman freeman Vraiment ils a bien parlé machallah.

  • @mayoronguer2498
    @mayoronguer2498 5 лет назад +4

    Serigne khadim Nii nguénko défé rékla bilahi yalla na diamm yague barké borom Touba❤❤❤

  • @faboyeamr7333
    @faboyeamr7333 5 лет назад +81

    Serigne khadime mane khamoumala mais begue nala lole si sama kholl

  • @fatyleye5847
    @fatyleye5847 5 лет назад +1

    Bravo à cheickh béthio il a réussi où beaucoup ont échoué l'éducation la basse de tout .

  • @astouniang5169
    @astouniang5169 5 лет назад

    Machallah thioun rafèna yalla nako yalla yeureum tè kharè ko aldiana you kaweya si barkèb serigne saliou

  • @modoumbaye2797
    @modoumbaye2797 5 лет назад +1

    Machala amna solo

  • @sopserignefalloufall2832
    @sopserignefalloufall2832 5 лет назад

    Machallah rafetna amna solo

  • @elhadjifaye2998
    @elhadjifaye2998 5 лет назад +36

    Mane dé douma thianta mes yaw môme damalla sope lole

  • @mamycamara155
    @mamycamara155 5 лет назад +8

    Bilay mala beugu té gueum leu🙏🙏🙏🙏

  • @elhadjikandji2674
    @elhadjikandji2674 5 лет назад

    am na solo lorr serigne khadim thioun machall

  • @moukhtar
    @moukhtar 5 лет назад +1

    Macha alah ndiguel djieufé

  • @salioudieng8675
    @salioudieng8675 5 лет назад

    Suis tidiane mais j'aime lole Cheikh bèthio barki yalla yallanako yalla yeureume si barki Serigne saliou

  • @Ndiaya658
    @Ndiaya658 5 лет назад +1

    Siguil nga niou Thioune Serigne Khadim yalla na nga fi yagu té wéér

  • @magettembaye820
    @magettembaye820 5 лет назад +9

    Lou wer nga wakh serigne mountakha moy serigne touba

  • @khadimfalltoubaitalelecapo5591
    @khadimfalltoubaitalelecapo5591 5 лет назад +1

    Mach alla Diadieuf serigne Khadim Amna Solo Diadieuf

  • @aminatasidibe4869
    @aminatasidibe4869 5 лет назад +3

    Macha Allah wahdji rafetena Yalla nako Yalla yeureme te Xare ko Aldiana RIP tonton

  • @fatysyll5643
    @fatysyll5643 5 лет назад +1

    Kou toudou khadim fo diar dieul si sa tourando dara .. khadim mo fort le serviteur du prophete machala.. serigne bamba keine dou mome

  • @salamfall643
    @salamfall643 5 лет назад +58

    Ndaysane ya am talibè wayy

  • @mbenewade1366
    @mbenewade1366 5 лет назад

    Machallah serigne Khadim Thioune Faxass kadouyi amna solo lol🙏

  • @ndeyeamy3958
    @ndeyeamy3958 5 лет назад

    Machalah amna solo yalna yallah may len xolou mougne

  • @ousseynouleye1038
    @ousseynouleye1038 5 лет назад +2

    machalla am na solo dh

  • @abounafansunited9333
    @abounafansunited9333 5 лет назад

    Massallah khadime tioune waxji rafétnà loole

  • @morgueye5088
    @morgueye5088 5 лет назад +2

    Dieureudieuf Thioune yawdé Nawnaala

  • @dabz3318
    @dabz3318 5 лет назад +5

    Eskeuy amna solo

    • @morniang2294
      @morniang2294 5 лет назад

      Machallah wakh dji amna solo yalna yallah yeuremko

  • @bmtvthiattinfo1855
    @bmtvthiattinfo1855 5 лет назад

    Diuera diueff s.khadime thioune kadou gui amna solo

  • @enzomoretti5931
    @enzomoretti5931 5 лет назад +19

    Wakh ji rafetna serigne khadim thioune mbolem talibé mouride contane nen si wakh ji

  • @ndoumbendiaye7440
    @ndoumbendiaye7440 5 лет назад

    dieureudieuf yallana yalla yagal takhawaybi kadouyi rafetna machallah

  • @babacardiobaba9321
    @babacardiobaba9321 5 лет назад +1

    Machalla serigne khadim

  • @awagueye2807
    @awagueye2807 5 лет назад

    Machallah s khadim beugue nala dh

  • @coumbabeye9969
    @coumbabeye9969 5 лет назад +3

    Rafetna yalla nako yalla khare aldiana

  • @pendakonta4458
    @pendakonta4458 5 лет назад +10

    Dieuredieuf Serigne khadim beuguenalla soppenalla nane lay déff ba guissela barkep Serigne saliou

  • @boubacardiouf8454
    @boubacardiouf8454 5 лет назад +21

    Jerejef Thioune wakh Dji rafétna. Mouride Ndiguel
    Paix à son âme Cheikh Béthio Thioune

  • @serignetoubagueye7205
    @serignetoubagueye7205 5 лет назад +2

    Akassa

  • @ibouthiam3274
    @ibouthiam3274 5 лет назад

    Machallah kadou yii rafettna yalla na yalla sam la same diabott gii

  • @rokhayakande7858
    @rokhayakande7858 5 лет назад +1

    machalla thioune

  • @evidenceaimiehefe3883
    @evidenceaimiehefe3883 5 лет назад

    Merci ..domy cheikh dagno am yare..wayè thiantacoune amou niou yar dara...Merci khadim

  • @aichadiouf7168
    @aichadiouf7168 4 года назад

    Bilaye walaye cheikh bethio Thioune yalana khipe Aldianayna Fidawzi Amine yarabi Machala Sa diambote gui Machalah rawnanou niep

  • @smarttvsn7593
    @smarttvsn7593 5 лет назад

    Maashal laah s khadim djaa djeuf thioune

  • @moustaphandiaye9697
    @moustaphandiaye9697 5 лет назад +1

    Bravo

  • @binetadiouf4931
    @binetadiouf4931 5 лет назад +1

    Machallah rafetna lol yalna diam yagu serigne bethio yalnako sounou yeureum té haréko aljanna

  • @aminagueye6386
    @aminagueye6386 5 лет назад

    Machala serigne khadim wakh dji refetena

  • @bayedjite6811
    @bayedjite6811 5 лет назад

    بارك الله فيك أحسنت وقولك حسن

  • @astouflorydaffe9561
    @astouflorydaffe9561 5 лет назад

    Machalla ki dal kilifeu leu
    Wax j rafetna xel mi seleu na
    Vraiment tu es bien éduqué 🙏

  • @khadijasy7012
    @khadijasy7012 5 лет назад

    Mashaallah Serigne Khadim Thioune khawma la d wayé sopenala ndakh say kadou you rafette

  • @kourelmarocdakhla598
    @kourelmarocdakhla598 5 лет назад +8

    Bilahi nawou nala serigne khadim yaw dh yarnanou la te ame gue ak talibé

  • @weuzagayy7773
    @weuzagayy7773 5 лет назад

    ALLAH khareeko ALDIANA aminn

  • @amantousambe6796
    @amantousambe6796 5 лет назад +38

    Serigne Bethio talibè la wone yague Na dieufé Digual Walay Médinatoul Salam Ak Touba dayeu Béneu fousi dém Serigne Saliou mougui fa🙏🙏 nioune dé Santeu Naniou t daniouy sakh di liguéyal Serigne Touba Ba Faw Donite ay Thiantacoune Ba Faw Barkép Serigne Saliou 🙏🙏